NDONGO LO [en Exclusivité] qui chante et fait son Diébalou à SERIGNE BETHIO THIOUNE en 2003

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 янв 2025

Комментарии • 262

  • @miya7190
    @miya7190 4 года назад +5

    Yalla na yalla yereume té kharé ko aldinna amine amine Sénégal khamouniou kou Mane kou dé laniou khame Abdou Guité ceicke ndandane la mé limasi méti rek bala nioukoye khame rek mou diougé fi mé yalla na ko fi yalla yagale amine ak daba seye tamite

  • @alkhamdoulilah518
    @alkhamdoulilah518 4 года назад +4

    cheikh bietho ak ndongo lo yalla na len serigne saliou terou

  • @bayecheikhlofficiel
    @bayecheikhlofficiel 5 лет назад +2

    Je sais pas mais depuis que jai entendu vos chansons jai jamais oublier vos mots cest comme si tes la jusqua present walahi et tes inoubliable téh dagnio djitou rek mai yag yag on va te rejoindre donc yalnala kharé aldiana firdaws

  • @alphandiaye7799
    @alphandiaye7799 4 года назад +9

    Ndongo ne pouvait pas vivre plus longtemps, quel talent.

  • @dieynasow4010
    @dieynasow4010 5 лет назад +7

    Bilaye Ndondo tu resteras toujours dans nos cœurs. sa belle voix me fait frémir que la terre lui soit légère

  • @moussaseck3643
    @moussaseck3643 4 года назад +4

    Ohh, la vie est si courte mais que notre bon DIEU les accueillent au paradis, amine

  • @gueyemabigue2633
    @gueyemabigue2633 4 года назад +2

    Jajeufety Serigne Bethio ! Ndongo Lo raw nga ! Ame nga ngeureumeul Yalla!

  • @abdoudiouf1652
    @abdoudiouf1652 6 лет назад +18

    Que la terre soit léger thi barkeb Sérigne Fallou

  • @mhdmhd8955
    @mhdmhd8955 6 лет назад +57

    Billahi c la vérité j'ai entendu parlé dans le commentaire précèdent k tes confrères musiciens t'ont oublié...... C dommage il fallait vous rendre hommage chaque année pour nous faire souvenir ki tu as accompli un travail remarquable dvns la domaine musicale du Sénégal
    Que le bn Dieu ''dit il est unique '' vous réserve dvns son paradis et vous tolère tt vos erreurs commis sur terre
    ♥One(👁) love ♥

  • @syllagolf7339
    @syllagolf7339 6 лет назад +46

    yalla nako yalla yeureum barki serigne karim

  • @dalzesow3506
    @dalzesow3506 5 лет назад +7

    Thiey sama ndongo lo manguilay,,😭 batay
    Ak sama cheikh Bethio thiey adouna
    Lo guiss dafay diekh

  • @assanetoure7785
    @assanetoure7785 5 лет назад +1

    Ndeysane doumala meussa faté yalla nalla serigne fallou térou aldiana

  • @thierbeye1860
    @thierbeye1860 6 лет назад +38

    Thiey sa moromou artiste waroon nagn lay rendre hommage chak annee waye senegal mom moungui nonou rekk

  • @verginiegueye4123
    @verginiegueye4123 5 лет назад +1

    Bilaye sama yarame bagui daw Barker serigne saliou yalla nala yalla khare aldiana

  • @safietousall4068
    @safietousall4068 5 лет назад +5

    Oooh dieredieufati serigne Saliou mom cheikh bethio ndogo lo yalla na dadjék sangam ba fa serigne Saliou ❤

  • @amababa6737
    @amababa6737 4 года назад +2

    Kou melni yaw dou amate si dounyaa

  • @sopeyndongolojammrek1540
    @sopeyndongolojammrek1540 5 лет назад +4

    Keine dou ndongo lo bala beugue yalla nala s fallou terou

  • @gayemamediarra9731
    @gayemamediarra9731 5 лет назад +1

    Thieuy wadji ngi nonou dh yalla nla souniou brm bi xaré aldjanay firdawsi😢😢😢😢😢😢

  • @bambistafaye7591
    @bambistafaye7591 5 лет назад +3

    Ndaysan lii yéména cheikh bii ak ndongo yalla na lénn yalla yeurame si barké alhourane

  • @ababacarsamb837
    @ababacarsamb837 4 года назад +1

    yalnako yalla yeureume thi barki borom touba

  • @lamineyade2099
    @lamineyade2099 5 лет назад +7

    Ndongo Lo ndeyssane tu resteras à jamais dans nos cœurs Yalla nalla yalla yeureum

  • @ridialsy4890
    @ridialsy4890 5 лет назад +4

    Tiey ndongo lo Yagui fi yallah n'a léne yallah yeureum kharer léne aldjana firdawsi yaw ak cheikh bethio thioune

  • @fatndoyefall4907
    @fatndoyefall4907 4 года назад +1

    Que dieu l'accueil dans son paradis amine

  • @amzoufficiale190
    @amzoufficiale190 5 лет назад +5

    Bilay niang balo yalla nala yalla khare aldianna firdawsi si barkep s fallou❤

  • @santeserignetouba4826
    @santeserignetouba4826 4 года назад +4

    Bilakhi cheikh bethio ya bakh té beug serigne Saliou kou fethiéaloul serigne Saliou féthial ibliss, yallah nalen sunu borom khare aldianay Firdaoussi thi yaw ak ndongo lo thi barqué sérigne Saliou, barqué sérigne Fallou ❤️ Amin

  • @mbissanedione3828
    @mbissanedione3828 6 лет назад +39

    il est meilleur ndongo sama kharit yal nala yalla téro aldiana

  • @fadelbambiste1451
    @fadelbambiste1451 7 лет назад +203

    Yalla ga guisé ak seydina mouhamed ndogo

  • @firdaousifirdaousi6610
    @firdaousifirdaousi6610 5 лет назад +2

    YALLA NALA YALLA yeureume ta kharaila adiana firdaouwsi amine

  • @Gallassdiop7597
    @Gallassdiop7597 5 лет назад +7

    Thieuy Ndongo lô yalnako yalla yeureum barki brm touba😭😭😭

  • @diennesidi9022
    @diennesidi9022 6 лет назад +1

    Ndongo lo s. Abdou rahmane mou s fallou moye serigne niam

  • @modoumbackendiaye9523
    @modoumbackendiaye9523 5 лет назад +9

    Man rek mako sétane si moi de octobre 2019☝️

  • @damembaye8600
    @damembaye8600 6 лет назад +9

    Yalla nako yalla yeureum ci barké seydina mouhamed psl

  • @mouhamedkhgueye9
    @mouhamedkhgueye9 5 лет назад +4

    Cheikh bethio Yalla nako Yalla yeurem

  • @binzsallah4593
    @binzsallah4593 5 лет назад +2

    Ndeysan aduna dou dara may Allah swt forgive all their sins and grand them jannatul fidawsi with all departed souls

  • @ibrahimniang5267
    @ibrahimniang5267 4 года назад +1

    Like you my brother 👊 peace and love Ameen

  • @ismailasankhe9140
    @ismailasankhe9140 5 лет назад +1

    Yâllna yâlla khareko aldjanaye ferdaw si AMİNE inchallah

  • @khadikebekhadikebe9714
    @khadikebekhadikebe9714 5 лет назад +1

    Adouna Dara yalla n'a yalla khare aldiana firdawci

  • @kheutzabi3359
    @kheutzabi3359 5 лет назад +5

    Thieye chiekh bii yalla nakou yalla youkou ay lèrrr way ❤️❤️❤️🤲🏿

  • @modoudiene3340
    @modoudiene3340 5 лет назад +1

    Yalla na lene yalla kharé aldiana

  • @mamediarradiop6803
    @mamediarradiop6803 4 года назад +1

    Qui et la en 2020

  • @babaakassasamb3590
    @babaakassasamb3590 5 лет назад +6

    Ndeysann kii mo dakh wey lii dafa triste. Ndoogo bou fii nékonn baa léguii kén dou wéy

  • @modouwar2211
    @modouwar2211 4 года назад +1

    Ndaysane adouna yagena nékh👍

  • @assdiack7203
    @assdiack7203 5 лет назад +1

    Ô yalla na yalla défal aldiana firdawsi ndogo lô

  • @babasamb4834
    @babasamb4834 5 лет назад +2

    Aminé y allna yalla Naguou niane yeup

  • @daoudandiaye1053
    @daoudandiaye1053 5 лет назад +7

    Yalla na soufou touba weyaf sa kaw binga nelawe la way diekh Sénégal

  • @oumardiouf1585
    @oumardiouf1585 4 года назад

    Yalnako yalla yeureum khareko aldjanaaa firdawsy Barker yonenn by

  • @seuttoulatdior5572
    @seuttoulatdior5572 6 лет назад +6

    Yallah na yallah yok leram yallah nga terei thia aldiana you kawei kawei aduna du dara billay

  • @ababacarsamb837
    @ababacarsamb837 4 года назад +2

    ndeysane aka meuneu weuye

  • @naboucisse3945
    @naboucisse3945 4 года назад +1

    Ndaye sane yalla naléne yalla yereme

  • @sokhnamomibocoum4148
    @sokhnamomibocoum4148 4 года назад +7

    Ndeyssane li dawna yaram yalnako sangou Cheikh Bethio Thioune terou Aldiana firdawssi Amine Bilay ya gorewone

  • @cheikh_ahmedndiaye7925
    @cheikh_ahmedndiaye7925 Год назад +3

    Guiss beugu yalla mokoy def si diam dama beugu ndongo😢

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 4 года назад +1

    Thiéy ndongo yalna khipé aldiana

  • @amarlaye1064
    @amarlaye1064 5 лет назад +4

    Yallaa naléne sougnou borom yereum gnom gnaar nieup si barké weerou korou bi

  • @diatoudiarra5048
    @diatoudiarra5048 6 лет назад +12

    ohh ... j suis vraiment touché adouna d'où dara ndogo

  • @mbayeluno8507
    @mbayeluno8507 5 лет назад +1

    Yalna yalla yessel yeurmandè si kawam

  • @samadeguine9840
    @samadeguine9840 5 лет назад +5

    Nov 2019 yalla d'où khéwy

  • @kalakala8032
    @kalakala8032 4 года назад +1

    Ndaysan yallanala yalla khare firdawsi nit gou bhak

  • @falldine9699
    @falldine9699 5 лет назад +1

    Yalna yaleu yareum len barckep Serigne Touba amine

  • @jwrikfinii7021
    @jwrikfinii7021 7 лет назад +13

    Cey SERIGNE BETHIO SALIOU amoo moroom dh.
    Serigne Bethio jebalaate naala sama bopp ak sama njaboot adouna ak alaakhira.
    SERIGNE SALIOU MBACKÈ MOOY YALLA SOUNOU BOROOM dh.

    • @papembayesow6099
      @papembayesow6099 7 лет назад

      Amine

    • @sodasall2954
      @sodasall2954 7 лет назад

      Thieye ndongo je n'arrive pas a oublie sa mort le meilleur de youte sa generaion yallnako yalla khareko aldiana amine

    • @khardiatasow4738
      @khardiatasow4738 6 лет назад

      dieureudieuf thioune

    • @taphasici7046
      @taphasici7046 5 лет назад

      JWR IKFINII ccnngjd

  • @mbayethioune9078
    @mbayethioune9078 5 лет назад +3

    MBAYE THIOUNE ndongo LO

  • @serignemomarmbackegueye6557
    @serignemomarmbackegueye6557 6 лет назад +2

    Thieuy ndongo amo morom yalla nalla yalla kharé aldiana

  • @sms3955
    @sms3955 4 года назад +2

    Que firdawsi soit ta deumeur internel ndysaaan ❤

  • @papambaye3796
    @papambaye3796 5 лет назад +1

    Yallnako yalla khareko alldiana 🙏🙏 yallnako serigne Salliou mbacke terou

  • @ababacarsamb837
    @ababacarsamb837 4 года назад +1

    ndeysane li dafa dawe yarame waye

  • @leylaafriq3581
    @leylaafriq3581 5 лет назад +3

    Repose en paix ndongo cheikh bethio

  • @rokhayababoldiouf5447
    @rokhayababoldiouf5447 6 лет назад +33

    yalla nala Serigne Saliou térou 😭😭😭😭😭RIP

  • @badianebineta9628
    @badianebineta9628 7 лет назад +40

    thiey ndongo yala nan guangua yewo aldjana

  • @mbayesamb6582
    @mbayesamb6582 7 лет назад +52

    theuy nongo yala nako yala kharé aldiana

  • @modoudiagne2820
    @modoudiagne2820 3 месяца назад

    Ay sounou domou yaye marétou fall dji wayane touna ndongo goudéna😢😢😢

  • @jackjack3160
    @jackjack3160 6 лет назад +4

    yalla nala yalla kharé aldiana

  • @lam7procoiffeuradomicile796
    @lam7procoiffeuradomicile796 4 года назад +2

    Ndeye sann thiey adouna lofii guisse day diekh😂😂😂

    • @Ndiaga-mw6zc
      @Ndiaga-mw6zc Год назад

      Walay ndaysan adona billakhi dou dara lepay dekh mermous 2007 dotoul amty

  • @fatouseck831
    @fatouseck831 5 лет назад +2

    Mais pourquoi dieu le pris dans nos bras avec sa voix d'or paix a son âme R.I.P😢😢😢😢😭😭😭😯😯😯

    • @mamounendiaye6529
      @mamounendiaye6529 5 лет назад

      Billahi dfw dama Kaye khalat sama khol bi dièkh takk😭

    • @karimgaye4327
      @karimgaye4327 4 года назад

      Parce que fa hanloune lima yurid

  • @serignegueye2013
    @serignegueye2013 5 лет назад +1

    Yalla nako yalla yereme

  • @khadidiatoundiaye4643
    @khadidiatoundiaye4643 6 лет назад +1

    Yallanala yalla kharei ALDIANA NDONGO LO amina

  • @baidydiopsow6467
    @baidydiopsow6467 4 года назад +16

    Paix a leurs âmes

  • @sokhorcle4489
    @sokhorcle4489 5 лет назад +35

    Mane reik mako sétane si moie de mai 2019

  • @nancysy8578
    @nancysy8578 6 лет назад +6

    Serigne saliou mo bakh sangue cheikh bethio

  • @bassirousylla6467
    @bassirousylla6467 6 лет назад +2

    Yallah nako yallah yeureum Ndongo Lo

  • @joe-ny7fb
    @joe-ny7fb 4 года назад +2

    Mala beug ndakh nimou sopé Serigne fallou mbacké pa paré yalla mayko Mane dé talibé cheikh la wayé ndongo motakh ma gueuna kham Serigne fallou ba takhna kén khamoul ndakh mouride la wala tidjane k firdawsi soit son demeure

  • @ababacarsamb837
    @ababacarsamb837 4 года назад +1

    yalnako yalla yeureume

  • @binetabadiane4919
    @binetabadiane4919 5 лет назад +1

    Thiehy ndogo yala nala yala kharé aldjana

  • @zeynacuenca4219
    @zeynacuenca4219 6 лет назад +10

    Ay ndongo yama nakh ba dem😔😢

  • @londiaga7479
    @londiaga7479 5 лет назад +1

    Ndeysann yallnalen yalla yeureum

  • @dembasow7139
    @dembasow7139 5 лет назад +2

    Ndogo yallah naga guissé ake Mohammed

  • @coumbawadembaye4900
    @coumbawadembaye4900 Год назад +2

    Ndaye sane reposez vous en paix

  • @AmsatouNdiayetouba2615
    @AmsatouNdiayetouba2615 5 лет назад +1

    Ndayesane thiaye yalla sonou borom

  • @bayediopsoldarounguiraneba2712
    @bayediopsoldarounguiraneba2712 5 лет назад +1

    Yana ko yalla yeureum khareko aldiana

  • @fatousamb4662
    @fatousamb4662 5 лет назад +1

    Ndaysane yalla souffou touba sedde thissa kaw

  • @khadidiatoundiaye4643
    @khadidiatoundiaye4643 6 лет назад +3

    Yallanagua goudou fane CHEIKH BETIO THIOUNE YA BAKH tr WOOYOF

  • @verginiegueye4123
    @verginiegueye4123 5 лет назад +1

    Barker seydinamoukhamet mako beugue pire yalla naka yalla khare aldiana

  • @abodiop3306
    @abodiop3306 5 лет назад +1

    Nday san yalla nalene yalla yeureme si barkep borom touba

  • @farmadiakhate5200
    @farmadiakhate5200 5 лет назад +1

    Paix à ton âme noguo yallenala yalla yeureum ak hiekh bi

  • @kadycisse1300
    @kadycisse1300 6 лет назад +3

    yanala séydina mouhamet téru amine

  • @mgmlebfpmbaye4439
    @mgmlebfpmbaye4439 6 лет назад +47

    Ki est la en 2919?

  • @assanetoure7785
    @assanetoure7785 5 лет назад +4

    thiey ndongo yalla na soufff woyof sa kawe damala beugue sama kholle

  • @mamaaidadourrdourr6496
    @mamaaidadourrdourr6496 Год назад

    nongo sama nongo lo yaw rek lay top bilakhi aujourdui le 08 septembre 2023

  • @natiiba5216
    @natiiba5216 5 лет назад

    Machallah ndongo yalla nala serigne saliou wallou si barké borom touba

  • @sokhnabambistemouride1204
    @sokhnabambistemouride1204 5 лет назад +2

    Man ndongo nimako beugué😭😭😭

  • @serignemohammedboromkhewal4348
    @serignemohammedboromkhewal4348 4 года назад +1

    Ohh ndogo lo way ndaysane

  • @djibyrokheyadieye691
    @djibyrokheyadieye691 5 лет назад +2

    😭😭😭NDEYE SAANE