Well said? Are you kidding me? All he said was that Serigne Bass is not the only thief and that all tarikhas do the same. If Serigne Bass took the people's land, he's a thief just like everyone who else does. Wolof says "dou mane kèssè, bokoumassi moko guëne".
Thank you so much Dr.imam khadim Bousso this people really need to stop. Some people in Senegal are not grateful, we should be thanking serigne Touba Khadim Rassoul every seconds. Serigne Touba is our mom, dad.serigne touba is our 🌎🌎🌎❤️❤️🙏🏾 if it wasn’t for Him, all this people talking were going to be going to be a slaves. We don’t want nothing in life but Serigne Touba ❤️🌎🌎❤️🙏🏾
Yaw miii DOUL... Fi Serigne ak Talibé nioci yém koufi déf ndiombé danioulay dénoncé. Té nga wakh Seig Bass mou tontou bopam té léral mbirmi. Boudé dou deug nga wax ko mou porter plainte. Yaw wakhofi touss, pyramide bi ñieupa ci photo wou
Serigne Touba never accepted anything from rulers or kings. It prevents a scholar from telling truth to power. In our present day, the land belongs to the people. No representative of the state should give away land without direct benefit to the people as a whole.
Walahi kep kouye talibé wala lou bakh nior la naniou ko bayil journal Lam bi doméram la mé ci nakhar laye deuk niou bakh ndi bi sen mame di ligueye sa mame mongui done seytané
Mieux vaut répondre à la question au lieu d'accuser ce que madiambal fait privé ne nous intéressé pas mais serai demain les enfants aussi fidèle talibe comme vous si c'est le partage du gâteau soyez pitié du Sénégal et de vos descendances
Seriñ bi ma'g samay moromi taalibe yu bari dëggu wuñu Boycot yooyu ngai wax,kenn warul xaar ndigël ci kuñuy xeex mu feeñ ak mu jeema nëbbu.Dafa waroon doon reflex ba ñepp xamko.Waaye daal xalaas.
Man Lima geum moy soudé fi soufsi né warefou ko maye ndakh momélou askanwi la kon douma nangou niou diokh ko ken Cheikh bass ak kenen la yamale yeufou mbolo mbolo moko mom soudé fi soufsi ne loun mana diokh la kouné kon diokh ko Cheikh bass ayoul
Mouride deugg yi amone bou gneuk mo baretoul lègui nioussi bari djikoy wègn lanou yor fou toy noudal nakala Ab mouride mana wakh lou niaw si yone wi kouko dèff yasi bolè sa bopp wayè bokosi
Madiembal est plus pire que nadie Le criminels. C est vrais que etre mouride n est pas une obligation Est mouride qui veut Donc cessez d etre des detracteurs des criminels Vous ne pouvez rien contre les bienfaits les khewels que le seigneur a octroye a la famille sacree de serigne touba qui represente akhlul bayti Diadieuf serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall
Serign Touba dudan Jeefandkoo lum khamut fumu Jokhee. Ku jel gheekoom ken du am lumay wakh si yow. Mouride yu baree khamugnu dara che le Serigne daan Jangale.
ياشيخي حفظك الله ورعه واطال عمرك اني احبك جدا
Waw goor yalna yalla samm la S.Khadim Bousso
Monousii dara barkep s touba yalla kham nako
Well said Dr Serigne Khadim.Thank you!
Well said? Are you kidding me? All he said was that Serigne Bass is not the only thief and that all tarikhas do the same. If Serigne Bass took the people's land, he's a thief just like everyone who else does. Wolof says "dou mane kèssè, bokoumassi moko guëne".
Ma-jambal, de nit ku bon la, def leen ko nima ko def rekk, duma ko deglu duma ko seetaan, bama ko Bàyyee dafa yàgg.
Serigne Bassirou Mbacké khadimoul xadim yalna fi yague Loul te wér Loul amine
ماشاء الله وبارك الله فيك وجزاك
Thank you so much Dr.imam khadim Bousso this people really need to stop. Some people in Senegal are not grateful, we should be thanking serigne Touba Khadim Rassoul every seconds. Serigne Touba is our mom, dad.serigne touba is our 🌎🌎🌎❤️❤️🙏🏾 if it wasn’t for Him, all this people talking were going to be going to be a slaves. We don’t want nothing in life but Serigne Touba ❤️🌎🌎❤️🙏🏾
Machalla GEKhe Dr khadem bosso yalla nayalla samou lah 🙏🙏🤝🙏
MACHALLA TALIBÈ ahmadouyi
Yaw miii DOUL... Fi Serigne ak Talibé nioci yém koufi déf ndiombé danioulay dénoncé. Té nga wakh Seig Bass mou tontou bopam té léral mbirmi. Boudé dou deug nga wax ko mou porter plainte. Yaw wakhofi touss, pyramide bi ñieupa ci photo wou
Toupall fale GEKhe bass amoll s'en diotd ❌❌❌❌
Yalla nanioi yalla df mourit bouy diuefé ndigal
Machalla bousso wakh dji noyna AG na thi xol💘
Kou menii aüpna kharitool bouso waxtane wi amna solo lool nak
Amna solo
Suuf su Sëriñ Maam Moor Murtadaa am Lislaam lakoy delloo moom du jaay suuf
Ngir alal i àdduna
Kokou de degna suf si fi serign mourtada bayyiwon diayko degna kokou kaye adina rek
Machalla mbacke balla geuna yagg geuna wer barkép Serigne saliou mbacke
MACHALLAH DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA MACHALLAH YALLAH NANAOU YALLAH MOUSALE SI SAYTANÉ NDAKH NIOME AY DIAMOU SAYTANÉ RÉK LA
Dieureudieuf s khadim
Serigne Touba never accepted anything from rulers or kings. It prevents a scholar from telling truth to power.
In our present day, the land belongs to the people. No representative of the state should give away land without direct benefit to the people as a whole.
Man dé serigne khadim bousso damako beugue trop nguire serigne touba
Merci serigne khadim sama khol diekh na me mi ngi dall el modou gueye naniou li dienti mbiram
Walahi kep kouye talibé wala lou bakh nior la naniou ko bayil journal Lam bi doméram la mé ci nakhar laye deuk niou bakh ndi bi sen mame di ligueye sa mame mongui done seytané
Walahi lép tawfekh lay don serigne xadiim
Likouy doumagui niew Barke Borom touba
Machalla ❤
Sawaye boule bolè loubokoule khelcom ak mayla souf nga diaye ko doubèn kene dou Seringe Saliou Mbacke yalnako yalla faye yarabi bouko dèfone dara wala diouma wala école kene dou wakhe diadièf Seringe touba
Serigne touba dawoul lale alalou mbolo dou mane dogue bokomasi moko geune
🙏🙏
etats waroul diokh kene souf mou koye diayat boufa tabakhon ekol wala wala tol kene dou wakh khelcom bingaye seringe salou tol lako def kon boul bolè lou bokoul attations
Wawe wakhnga dage 👍🏽
nioune dé serigne touba diaral nanou dé fa yallahou
ماشاء الله
Bou déh kou wakh nga tontou di nga sonnou...meunouléne fékhé ba niép gueum mba beugue serigne Touba...
Yaw gueumo dara tu na aucune crédibilité vous êtes tous pareil
Jërëjëf sëriñ xaadim busso amna solo lool
Machealla
Ma diambal môme domeram leu , dafa bagne Serigne Touba
Machalla amna solo dieuradief bousso
Machallah
Sénégal kou wakh dagge don kou bon alali bour bayè ko bour yaw daga faral bas rek
Wawo da far rék wakhou fi dara
Bayi faralatè bi
Wakhofi dara
Machalla wakhe bui rafete na trop
Jërëjëf
Dieureudieuf bousso baly yalna yala yokou wergu
Pourtant Madiambal Diagne Mouride laa dhé
Ma diambal dafa rew dagnkoo wara doma yakh lep lom takhawal modiekh
Lima diakhal moy lingua na madiambal sama kharit la ko khamni serigne touba rèk la bagne
Mieux vaut répondre à la question au lieu d'accuser ce que madiambal fait privé ne nous intéressé pas mais serai demain les enfants aussi fidèle talibe comme vous si c'est le partage du gâteau soyez pitié du Sénégal et de vos descendances
Merci waay serigne bi
Machallah Amna Solo
Dieuredieufati Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baboul mouridina
Bayil sa dof dof loubi
Simi sa lunetye yi
Do touss
Coglioni
waw Goure mouride am na sólo
Dagena. Bari waxe ak pourap lem e
Seigne bi wakhal deug way! Bayi len far far lo bii hisss
Machalah Amna solo lool dieredieufe serigne Khadim
Seriñ bi ma'g samay moromi taalibe yu bari dëggu wuñu
Boycot yooyu ngai wax,kenn
warul xaar ndigël ci kuñuy
xeex mu feeñ ak mu jeema
nëbbu.Dafa waroon doon reflex ba ñepp xamko.Waaye
daal xalaas.
Et ta réponse est sans arguments piiire encore pour un imam
Mais seigneur bi madiambal wakhlolo
Jerejef bousso
Li lepou compalo la ak éta
Akassa
Mach alla amna solo bousso
Masa Allah merci beaucoup
Mach allh gawal taxawal ku
Man Lima geum moy soudé fi soufsi né warefou ko maye ndakh momélou askanwi la kon douma nangou niou diokh ko ken Cheikh bass ak kenen la yamale yeufou mbolo mbolo moko mom soudé fi soufsi ne loun mana diokh la kouné kon diokh ko Cheikh bass ayoul
Diadieuf bousso balli
OK mon Iman et Marabout que j'estime, mais cesser de dire que nous sommes plus nombreux et plus etc.... Il faut éviter ceux là
MADIABAL DOMOU THAGA bamodoudo la done framcon doudou refetou beneyonne
Souxar de baxol fii mom serigne touba rekk
دكتور فضلة الشيخ خاديم بوصو لافض فوك
bayili di sossal imame dou fene
El modou gueye naniou naniouko nokh soular bou bon bi man dama nekoul Sénégale me sou manekon Sénégale dinadem nokh el modou gueye billahi
Dangaye fen s touba ken douko lall
Tadial sa gatt
Nafekh lene diapou
Serigne bi rék lanou am
Serigne bass abdu khadir kobaxla nityi niosokhor
Madiambal dafa soxiour
Nadii moroutanila wala thieyene
Madambal. Nagou. Xorom. Ndayam
Yéw doul way wakho fii gatt bass abdou hader na'nou délo sou'nou 9 hectars sathii bi'gén' 'don
Khadimou Rassoul daawoul tontou té sàntoul kènn mouy tontou kou mandou lawoon.wakh ma sa kharite ma wakh la yaay kan.
Balmadé wané sa kham kham bariwoul
Mouride deugg yi amone bou gneuk mo baretoul lègui nioussi bari djikoy wègn lanou yor fou toy noudal nakala Ab mouride mana wakh lou niaw si yone wi kouko dèff yasi bolè sa bopp wayè bokosi
Faut suivre la voie tracée par Serigne Touba ou vous allez le regretter le jour du grand rassemblement...
machalah sumala saniona digeul de damanane la bul nopeti bukal ngi ngiy tontole yono morid
Dèmbou el modou gueye ak fam radiou zik fm di wax lou bon ci serigne bassirou dan lèna warra douma
El Modou Gueye la khamoul Lou Mouy déf Touba môme da Yaga Bonne
Wakh jii rafetna, wayai diabotou Serigne Touba gui nagnou ma bayil politiciens yii, dax loussi eupeu ay satan lagnou
Def nilaine wakeur Serigne saliou yi deff. Offf politicians yii rawatina Macky sall
Madiembal est plus pire que nadie
Le criminels.
C est vrais que etre mouride n est pas une obligation
Est mouride qui veut
Donc cessez d etre des detracteurs des criminels
Vous ne pouvez rien contre les bienfaits les khewels que le seigneur a octroye a la famille sacree de serigne touba qui represente akhlul bayti
Diadieuf serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall
Wakhou fi dara keneu toudou fi yonou mouride ni serigne Touba gniy sathie téy toudo serigne Touba niom gnoy nonou mouride serigne basse mom moy yakh derou mouride
Mak deih warna deff wala wakh lougnkoy nawé
Wawe lonioye khare tih banque wa touba nake joute na dé
Pourtant Lou am solo nga Wakh
Ki nafeh la
Lou Lou diu sa thieur warocowone dimbeli sais sai.
Serigne liguay wakh dou kham kham
Hakeuzaa
Qui se ressemble ; s'assemble....
313 elkhekoumo takajourou naneko seny madiabel diangne nane sounou borom khalako mok alalem domouram
Serign Touba dudan Jeefandkoo lum khamut fumu Jokhee. Ku jel gheekoom ken du am lumay wakh si yow. Mouride yu baree khamugnu dara che le Serigne daan Jangale.
Comparaison n'est pas raison....
Ma-jambal ab jaam la du naw le du ànda ndoo, doomi njaalo la rekk
Yaw tam de wakh deuga sorewo ak madiambal