Imam Khadim Ndiaye parcelle, Lima dundu sama keur fi ci Touba.. Sama diganteek…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025
  • Abonnez-vous sur notre chaine youtube Rafah TV international / Service commercial Rafah TV International : 77 433 39 39 : Email rafahtvhd@gmail.com
    Facebook Rafahi tv
    Instagram Rafah tv international
    @RafahTV1
    www.rafahtv.net
    RafahTV basé à
    Touba Mosquée .
    Nous venons auprès de votre haute bienveillance solliciter une demande de partenariat entre votre entreprise et la notre Rafahtv pour le passage de publicités de vos produits et la visibilité de votre entreprise à travers le monde entier.
    En effet, RafahTV est une chaîne de télévision en ligne implantée à Touba près de la grande mosquée depuis 4ans. Notre chaîne fait partie des meilleures chaînes de la place,
    En espérant vous comptez parmi nos futurs partenaires, nous vous prions de croire en l'expression de nos salutations distinguées.
    Intéressé

Комментарии • 583

  • @serignembaye4602
    @serignembaye4602 Месяц назад +57

    Imam khadim Ndiaye mi ku ragal yalla la wallahi

    • @mbayekasse4960
      @mbayekasse4960 Месяц назад

      Talibé bimou doone daa wara dem WAKH AK séeni kilifa
      Gniléne Santa la gnouy .
      9

    • @mbayekasse4960
      @mbayekasse4960 Месяц назад

      Def

    • @milkfaye2761
      @milkfaye2761 Месяц назад

      Yow geumo s touba

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 Месяц назад

      ​@@milkfaye2761wakhou deug dee kii mourid sadikh mom mo diangal imame seringe aboul barake mbacké miye djiété nafila massalik fi si ndakarou

    • @MouridoulLaahi
      @MouridoulLaahi Месяц назад

      Kii mome Loum djoublo wakh 😂wakhoufi dara DH yën ñii diko partagé démléne Bay fallga ba paré 2parti 😂😂😂😂😂😂😂😂😂moy yone kii wakhoufi dara

  • @SaTouba-f4f
    @SaTouba-f4f Месяц назад +53

    Kou wakhoul degeu Wakh Safan civil Manoul Rek le Maromou Civil leum..
    Wallahi Ya Imame Ya nek thi Dégue.😢😢😢😢

    • @niangmayib2073
      @niangmayib2073 Месяц назад +2

      Deug rk mooy deug

    • @cheikhabdoudiop5335
      @cheikhabdoudiop5335 Месяц назад

      Djreudjeuf s khadim ndiaye moumelné linléne sante ak liniye deff bokugnou ndakh toubeuy bou andéck moummu diott daganna thi lislam gniy diapé warnano ragné

    • @cheikhabdoudiop5335
      @cheikhabdoudiop5335 Месяц назад

      Dengdjiou wér peigu

    • @DiagneElhadji-d8f
      @DiagneElhadji-d8f Месяц назад

      Esk wokho lasa dess kon ndigeul dieuféde

    • @is909
      @is909 Месяц назад

      Lolou moy deugue

  • @BaraDieng-io7my
    @BaraDieng-io7my Месяц назад +48

    Yenagui wakh rkk barki alhouran imame khadime ndiaye mi ki moma diagal alhouran bama wathié 3 foiss nitt kou geum yalla moy ki

  • @assanefallphotography6921
    @assanefallphotography6921 Месяц назад +17

    Imam Khadim Ndiaye un référence ❤

  • @AyoubaNdiaye-y5h
    @AyoubaNdiaye-y5h Месяц назад +11

    الذين ان مّكّنّاهم في الأرض أقاموا الصلاة وآتوا الزكاة وامروا بالمعروف ونهوا عن المنكر ولله عاقبة الأمور

  • @babacardieng-yt6si
    @babacardieng-yt6si Месяц назад +2

    Dieredieufé Serigne Touba 🙏🙏🙏
    Diaramaaa mm cheikh ibra ibrahima fall 🙏🙏🙏

  • @alassanedieng8579
    @alassanedieng8579 Месяц назад +26

    Merci Imame ces actes sont ignobles dans la ville de Serigne Touba c'est a dénoncer ils font dans l'abus

    • @ousseynoutoure3621
      @ousseynoutoure3621 Месяц назад +4

      Bou adouna bi yeupe dadjei ak koumou meuneu done bo teigouwoul si ndigueul gni teigueul leine

    • @fallam1010
      @fallam1010 Месяц назад

      en quoi cela vs concerne

  • @ablayesane6519
    @ablayesane6519 Месяц назад +11

    IL faut que l’état prenne ses responsabilités . Nous partageons tous le mm territoire alors on est tous égaux devant la loi , ces actes de violation de droit de l'homme ,il faut que ça cesse

  • @Sénéga.dioubanti
    @Sénéga.dioubanti Месяц назад +3

    Bilahi kou bayi diouli AK wore do am yermande si diamou yalla yi rawati na dijgune

  • @toubapatar
    @toubapatar Месяц назад +16

    Dieureudieuf imam xadim ndiaye

  • @serignesodagueye3398
    @serignesodagueye3398 Месяц назад +9

    Wawe goor IMAME Khadime ❤❤❤

  • @MouhamadoulamineSamb-n8g
    @MouhamadoulamineSamb-n8g Месяц назад +16

    Touba li serigne bi beug moy am ما يريد الشيخ هو ما أمر الله،ما نهاه هو ما نهاه الله،وسلام على المرسلين والحمد لله رب العالمين،moytoulen baye fall yi bakhna

    • @AntaMbaye-pq1jr
      @AntaMbaye-pq1jr Месяц назад +1

      Khamo gatt nopill

    • @khadimathj8129
      @khadimathj8129 Месяц назад

      Le marabout n'est pas en règle. Les baye faux sont des sauvages

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад +1

      Mane dé Touba Yallah boumafa am sokhla ba béss bimey guéneu adouna amine 🤲🏾 deukou bou amoul ndokh mou nékh té bari mboyo 😂😂😂

    • @modoudieng2750
      @modoudieng2750 Месяц назад +1

      Wa Wawaw sa baay dafa amoul duek mootakh

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад

      @@modoudieng2750 yaw ak sap serigne binga gueum sen thioparétou ndeye 😂😂😂 mane domi lébou laa, sokhla wouma nieuw touba té Yallah boumafa am sokhla ba béss bimey guéneu adouna amine 🤲🏾 deukou bou niaf ndeyam bobou ndokh mou nékh amoufa, loumafaye deff 😂😂😂

  • @Échophysiologiste-cb9bi
    @Échophysiologiste-cb9bi Месяц назад +11

    Lii reka bax❤❤❤
    Louté nga wax ak kilifa yi ngay si Internet bi, lii segn bi beugue moy am

    • @samdiawdiaw8269
      @samdiawdiaw8269 Месяц назад +1

      xna dego ko ki limiy wax si ragal yla lako tek bayil narfex

    • @CheikhounaDiop-f3s
      @CheikhounaDiop-f3s Месяц назад +1

      Li Serigne bi beugeu kane mola wax dou am ??? Ki di wax mo la geuna diégué serigne bi .seytané yi gueen done

    • @abdouniangtv180
      @abdouniangtv180 Месяц назад +1

      seringue bi molén wakh ngéni diapou djigéne yi wa loutakh yalla mom lim wakh dolén si déff dara sénn seringue you nio dakha nan sangara di mandi loll dolénsi wakh

  • @abdouniangtv180
    @abdouniangtv180 Месяц назад +1

    seringue abô mbacké mi djité masalikoul jinan grand mosquée 🕌 du dakar imam khadim ndiaye mi moko diangeul al khourane bay fall yi khamoun gatt baye wakh si l'islam

  • @mordiop5531
    @mordiop5531 Месяц назад +7

    Nit kou bakh Serigne khadim Ndiaye

  • @amleking2219
    @amleking2219 Месяц назад +2

    Sénégal nékhoula wakhé mais bou ëuleugué dinane khamni serigne bi nékoul si yi niou nék blh💔💔

  • @senegalvillagetvdiop5152
    @senegalvillagetvdiop5152 Месяц назад +1

    Ak lou mena am d'où deug d'où yone yalla mignou wathie ci soufam ci sakh force wougnou guèni thiahane

  • @amdymoustaphaakasa5963
    @amdymoustaphaakasa5963 Месяц назад +30

    Dieuredieuf borom touba diarama mame cheikh Ibrahima fall

    • @Azou0596
      @Azou0596 Месяц назад

      Ça n’a rien à voir ak Li imam di waxx Lii acte terroriste la nioun nieup ay Mouride laniou

    • @milkfaye2761
      @milkfaye2761 Месяц назад

      Yow geumo s touba yefarala geun

  • @degdeugtv7872
    @degdeugtv7872 Месяц назад +8

    Civil dou règle Civil dans un pays de droit

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz Месяц назад +3

    Touba daal lifi Serigne bi beug Moy Am inchallah wa Salam 🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿

  • @secksaliou1575
    @secksaliou1575 Месяц назад +3

    Merci beaucoup serigne bi baye fall yi dano raw bilakh

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 Месяц назад +13

    Yaw l'âne Moy badio fag amale ay téguine téguéne bayi diabolisé bi li Serigne bi begueu rék Moy am koumou nékhoule ga déme sa keur mame moudiékh

    • @abdoufallsow3277
      @abdoufallsow3277 Месяц назад +1

      Waxi doff demal wuti xam xam

    • @bachiirleveridique9767
      @bachiirleveridique9767 Месяц назад

      *SËRIÑ TUUBAA* MOOY SUÑU MAAM ÑUN ÑÉPP FII KÉN DUFI GÉNN DI DÈM #TUUBAA GII KA ÑUY TOOK PAR LA FORCE

    • @MouhamedGueye-o5j
      @MouhamedGueye-o5j Месяц назад +1

      Kuer mara yi sén domyi nio guena doywar foof maylèn niou diamou way

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад

      Wawaw ! Mane dé mangui sama keur mame ndakarou ndokh mi nékh na té mangui si borou guédj gui. Yallah bouma am sokhla touba ba béss bimey guéneu adouna amine ya rabbi 🤲🏾

  • @modousall8286
    @modousall8286 Месяц назад +5

    Merci imam❤

  • @Khadimdiopi2000
    @Khadimdiopi2000 Месяц назад +2

    Ndeyssane Serigne Khadim Ndiaye ❤khawma kañ lakoye djissate ❤

  • @IbrahimasarrDieng
    @IbrahimasarrDieng Месяц назад +17

    Bilahi imam ya nek thi dégue baye fall yi yabate rek lan def

  • @Babacarmagane
    @Babacarmagane Месяц назад +7

    Merci imam

  • @modoudiengsopbichri6434
    @modoudiengsopbichri6434 Месяц назад

    Li Serigne bi beug si deuk inchalla moy té kou ame lolu meti demal thi serigne Mountakh Mbacke nga wax koko ndax moy jëuwrin Bay faal yi Wa salam

  • @bambadieng6025
    @bambadieng6025 Месяц назад +12

    *_AMOU MA DJOTOU LIRE VIDÉO BI BAMOU DJÉXX ,MÉ BOUDÉ NANGOU NGA LI SERIGNE MOUNTAKHA DIGUEUL BAYE FALL YI JEUREUJEUF ,BOUDÉ ANDOSSI WAXOO DEUG YA TOGN WASSALAM_*

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 Месяц назад

      kouy dikle niaka diouly mogueneu bon te moutaha migikoy def

    • @bambadieng6025
      @bambadieng6025 Месяц назад

      @elagegueye3310 *_YAW DEJA LINGAY WAX YAW XAMNGANI WAXO DEUG BILAHIL LAZII BAPARÉ RAGALOSSI YALLA CONTINUÉ DI FÉNE ,GUÉNÉL BÉNEU VIDEO BOU SERIGNE MOUNTAKHA DI DIGLÉ GNAKA DJOULI ,BAYILÉNN DI SOSS ,DINÉ DJI SENN BAY MOMOUKO ,MEUNOULÉNN DOUGUEUL KÉNEU SAFARA DÉLÉNN DJAPOUNI YÉNA GUEUN KOUNGUÉNN GUISS REK BEUS DINA GNEUW NGUÉNN XAMNI MBAM SEUFF MOLENN EUPOU MAXAMA DOMOU HARAM NAN SERIGNE MOUNTAKHA..YAW AMOO WORMA SISA BAY SAX BAKOY AM SI BAYOU DJAMBOUR,SA WAXDJI NAK SI GUINAW ECRANT TÉLÉPHONE YI REK LAY YAM ,DOO MASSA GUÉNEU WAX KOSSI KAW ,XANA DJIHATOOO AYTHIA DEFAL VIDEO WAX LINGA WAX WANÉ SA PHOTO BOPOU 😁KONN BAYE FALL YI LAKEU SA GATT DH_*

    • @aliouniang6084
      @aliouniang6084 Месяц назад

      الأدب الأدب إنه عالم

    • @khadimathj8129
      @khadimathj8129 Месяц назад

      Tounou ndayou baye fall. Touba c'est une ville de sauvages

    • @bamS5919
      @bamS5919 Месяц назад

      Des hors la loi (ils ne prient pas doniou ay dioulit) qui font la loi 😂😂😂 non c'est incroyable "c'est le monde en pire"

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 Месяц назад +2

    Li Serign bi Beug thii deuk bii mo am inch'Allah 🤝

    • @modoundiaye3999
      @modoundiaye3999 Месяц назад

      Warone na fékk ngéni dieufé ndigalou Yallah niak diom

    • @NdiayeModou-b1d
      @NdiayeModou-b1d Месяц назад

      Thiakhan kep laniouy def

  • @boromtawfkhetv6216
    @boromtawfkhetv6216 Месяц назад +2

    Serigne Khadum Ndiaye Kouma Naw Loll Gur Dokhinam Bou Refett

  • @thiernombengue9226
    @thiernombengue9226 Месяц назад +3

    Bayfaal yi nio nek ci deug.. Jup bouniou fante wala bou séré wala mou khaat kéena waroukoo nangou ci sa keur rawatina ci mbédami..
    Ya Serigne Khadim Ndiaye sokhnasi limou sol sou yiiwoon douniouko yobou.. Touba... niounn talibéyi bouniousi maslaha ak ndiabotgui... lolou moy deugg.... Dieuredieuf

    • @fadelndiaye4722
      @fadelndiaye4722 Месяц назад

      Liguaay wax dara nga si xamoul la wax Thierno reglel

    • @mamegorsarr1138
      @mamegorsarr1138 Месяц назад

      Diouli moy leppou

    • @MamedaraThioub
      @MamedaraThioub Месяц назад

      Lou lér ga wax

    • @cisse10
      @cisse10 Месяц назад +1

      Wa loutah diabar serigne yi di khéssel di sol lou séré douniou mour Ken douci wakh

  • @chiekhniangtalibebamba8414
    @chiekhniangtalibebamba8414 Месяц назад +3

    Li Serigne bi bague Moy am far force ✅

  • @panogayembaye2116
    @panogayembaye2116 Месяц назад +5

    imam Khadim Ndiaye koula sope la wayé yéy mom Dioumga dakh lagnouy téré ndagam lolou lagnouko Diapé rk mo togne YALLAH Nagnou YALLAH Fayal Baye Fall yi Barkép Kheikh IBRA FALL LAMP ❤❤❤❤

    • @YoussoufNdao
      @YoussoufNdao Месяц назад +1

      Baye fall si ay thiakhane rek laniou nek naniou dem diouli dji dem diamou dji yalla Lou guneu bonne bayi diouli ak woor amoul

  • @cheikhounambacke4638
    @cheikhounambacke4638 Месяц назад +11

    Man deh touba la deuk sant Mbacké bokk thi ndiabotou s fallou te bokk gniy gor gor lou thi samm wormay deuk bi waaye nag Serigne mountakha lii baye fall yi def digalou lene ko nagnou kholat ni gnou koy defee balaa euppi lokho famouy moudj dou diour diame

  • @gorambengue335
    @gorambengue335 Месяц назад +1

    Bakhna S chiekh thiouro dina len yay Lii

  • @DjilyKhouma-vq6jc
    @DjilyKhouma-vq6jc Месяц назад +2

    Merci beaucoup ❤❤❤❤❤

  • @kebecheikh3998
    @kebecheikh3998 Месяц назад +2

    Ndyasan s.khadim ndiaye moma diagal tajweed .yallanako yalla geuna weral

  • @khalyseck4917
    @khalyseck4917 Месяц назад +2

    Mais bay fall yii wérou gnou khamou gno mais li responsabilités serigne bi la rk touté fou koudoull sangou dou diouli nga dénk ko deukk bi Waw lolou ndakh ak wérr la

  • @santbambaahmadu9912
    @santbambaahmadu9912 Месяц назад +4

    Li Sëriñ bi bëgg ci dëkkëm bi kuko man def kuko manul dem feneen c’est très simple

  • @SaliouSene-t2q
    @SaliouSene-t2q Месяц назад +1

    Li Serigne beugue moy am

  • @fallousylla5386
    @fallousylla5386 Месяц назад +5

    Say wakh dra lérou ci deuk touba té khamo bay fall ga khamo keur mam chiékh

  • @ibrahimacamara4475
    @ibrahimacamara4475 Месяц назад

    On ne peut pas créer un État dans un État c'est vraiment impensable et c'est à l'État de prendre ses responsabilités avant que l'irréparable se produise...............................................

  • @mamadousy8633
    @mamadousy8633 Месяц назад +6

    Le fait de dire d'aller acheter des habits est synonyme d'un habillement indécent.

  • @AstouLo-l5u
    @AstouLo-l5u Месяц назад +17

    Imam yaw seuytane nga. Touba lifa Seringe bi beugeu mofay am koumou neekhoull nga dem sa keur mam

    • @seringembacke9316
      @seringembacke9316 Месяц назад +1

      Bayilen saga yi rafetoul 🙏🙏

    • @amadoufatimakane3564
      @amadoufatimakane3564 Месяц назад

      @@seringembacke9316 wah nga dëgg

    • @cheikhounadiop2632
      @cheikhounadiop2632 Месяц назад +2

      Kii de s mountakha mbacke diokh nako ay khale ba tayi guirr mou jangal leen allkhouran talibe s touba la lou bakh rk la kham

    • @amadoufatimakane3564
      @amadoufatimakane3564 Месяц назад

      @@cheikhounadiop2632 kon nak waroon naa jomba def exposition boo xamni dees ciy njaññ dëkk bu sell bi di TOUBA

    • @Bueleup
      @Bueleup Месяц назад

      ​@@cheikhounadiop2632merci❤❤❤

  • @Jeunepatriote
    @Jeunepatriote Месяц назад +1

    Mais imam jube bii mane na goudou dé mais wakho baxam dafa serré sii ay thieuram
    An tout cas dal lima guiss sii xalé Touba diamano dji képpou kouye négocier ak gnome dougnou falé
    Nagnou deupo ak charte Touba dakh képpou kou ko deff do am ak problème ak baye fall yii

  • @CheikhounaDiop-f3s
    @CheikhounaDiop-f3s Месяц назад

    Allahou Akbar😢 Baye Fall yi gno bayi ndigeulou Serigne bi di business

  • @MaSambaNdiaye-pl2we
    @MaSambaNdiaye-pl2we Месяц назад

    S imame khadime Ndiaye mon ma Dianguale bama mokale di Dianguale dou dokhe di lou doule dine lislame

  • @modoundiaye2179
    @modoundiaye2179 Месяц назад +2

    Ahhh doyna waaar d mohhh li serigne mountakha yeuguko d bilahiiiii

  • @fallndiolle4430
    @fallndiolle4430 Месяц назад +5

    Bakhna ci niom li yalla begue Ak li mou bagne Serigne bi diko doxal ci dekë bi gnou degeur bop logne té bzkhna

  • @assanemar5077
    @assanemar5077 Месяц назад +2

    Li serigne bi beugue moy ame kouko meunoul nga guéne deukou serigne bi togn bakhoul

  • @gueyematar1869
    @gueyematar1869 Месяц назад

    Man dé Guem Naa Serigne Touba, Yoonou Baye fall Laa Guemoul Ndakh bayi Diouli AK Wooor.

  • @LeyeMohamed
    @LeyeMohamed Месяц назад

    Nite défoull Lou gane djouly❤❤❤

  • @alioudiop552
    @alioudiop552 Месяц назад +11

    Linlén déf késé moy li war, baye Fall bég na ci niom lol Imam li am Dakar ganga nék amoul Touba, bici déss tamit ak ko mana don, imam, sëriñ, .... Tékou ci yon rék

    • @bachiirleveridique9767
      @bachiirleveridique9767 Месяц назад +1

      *Dañ koo deful sa nday rék DOOMURAAM ñun kuy gëm SËRIÑ TUUBAA ñoo la ko gëna gëm*

    • @abdoufallsow3277
      @abdoufallsow3277 Месяц назад

      Waxofi xam xam

    • @obd2214
      @obd2214 Месяц назад

      Waw yoone mom xana Julli ak Woor daff si bokoul ?

  • @maguettehane2424
    @maguettehane2424 Месяц назад +2

    Serigne bi dall deukeum bi limoufa beug kouko manoul nga abball Serigne mountakha limou beug rek Moy amm

  • @Idy-m6o
    @Idy-m6o Месяц назад +13

    Imame sit c'était là police tu va subir pur et tu vas accepter

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye662 Месяц назад

    Lii dafa ndiw loll sy touba❤

  • @khadimMbacke-d9u
    @khadimMbacke-d9u Месяц назад +8

    Wakhoufi dara wakhi yakh rek nguafi wakh

    • @fadelndiaye4722
      @fadelndiaye4722 Месяц назад

      Fénnn nga dh yaw Yafii waxoul tousss imbécillité bi gueini
      Di Diaye niolen ko eup fouff

  • @salioucisse2355
    @salioucisse2355 Месяц назад +3

    Waw touba mom ndakh rewou boppam laa walla
    Non
    _
    Niom naniou Diappou Bokkalle kattyii
    Moo geunn

    • @serigneniomrelo6956
      @serigneniomrelo6956 Месяц назад

      Touba rewoum serigne touba la

    • @salioucisse2355
      @salioucisse2355 Месяц назад

      @serigneniomrelo6956 Kan moo defarr souffou touba
      Dou yalla__
      Serigne bii mouy nieuw chi adouna Dou filla fekkon touba
      Bi mouy guenn adouna demoul bayiifi touba

    • @dembathiao8232
      @dembathiao8232 Месяц назад

      Iow wakhou dof ngay wakh touba réwou bopam la ndakh titre foncier Serigne Touba la té bam koy done bobou titre foncier bobou Sénégal amoul indépendance point.

  • @MourtallaDiop-vq2ex
    @MourtallaDiop-vq2ex Месяц назад +3

    Mach alla imam khadim

  • @SerigneNdoye-i4l
    @SerigneNdoye-i4l Месяц назад +1

    Touba dall ndiggueul moffay wéuy koumou nékhoul guénnal deukk bi dém fénén togne bakhoul ndiggueul mome dieuffé rék Touba dieum kanam inchallah

  • @khadimendiaye3674
    @khadimendiaye3674 Месяц назад +7

    Imam sawkhdji dafa khawa subjectif.ter lingay def dou sa thieur ndakh kilifa nga

    • @fadelndiaye4722
      @fadelndiaye4722 Месяц назад

      Loudoul thieurou imam Ak louy tieureum dou yaw yako koy wakh réw guein trop

    • @MamedaraThioub
      @MamedaraThioub Месяц назад

      Yaram bayil khadim mi moiy wax il fait la publicité des procedures des bayefall pour executer le ndigueul du Khalif
      Sou benene yoné la fille douko défate
      Lou Serigne bi beugue moy ame comme dab

    • @fadelndiaye4722
      @fadelndiaye4722 Месяц назад

      @@MamedaraThioub khadim touss meunou leen ko cii moom
      Wallahi azim li lislam beug molen ko geuna kham foufff réw guein yarou woulein

  • @Khadimbambapastef40
    @Khadimbambapastef40 Месяц назад +1

    baye fall yi daalle wakhe ak ñoume diotna li miki beugeu apou 🔥🔥🔥🔥🔥

  • @alioumbacke5514
    @alioumbacke5514 Месяц назад +2

    Ki mo djiaggal alkhourane ki nafila thi djiouma massalikul djinane

  • @Idy-m6o
    @Idy-m6o Месяц назад +4

    Ça c'est pas vrai c'est fille n'a pas n'a pas ramplir les critères

  • @ibrahimacissedieureudieufs2732
    @ibrahimacissedieureudieufs2732 Месяц назад +1

    Paa may niou diamou yakk waa rafah TV yéna yam pass passi wahabiste nguéne yor gueumouléne dara

  • @khadimniang2112
    @khadimniang2112 Месяц назад

    Ndayssan imam yalla baxna 😢😢😢 mia douyna weur dhè 😢😢li duo yon

  • @amadoufatimakane3564
    @amadoufatimakane3564 Месяц назад +1

    RAFAH TV LAN MOOFI JAR JALLALÉ AY FEN RAWATINA MOU JËM CI DËKK BU SELL BII.
    RAFAH TV KAN MOO KO MOOM ?

  • @momarmbaye4076
    @momarmbaye4076 Месяц назад +1

    touba dé kéne manta wakh ba bay fall yi dounou ko saytou darra da nkén di wakh ba sonou rék

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 Месяц назад +6

    LII YOONE WARNAKOO INTERDIRE . CIVIL DOU YAR CIVIL

  • @modugueye2152
    @modugueye2152 Месяц назад +3

    Baye fallyi lenyedeff tegonoko fnn

  • @alioudiop552
    @alioudiop552 Месяц назад +5

    Ci wax yanouwoul mana ci colin gui

  • @amadoumarico5944
    @amadoumarico5944 Месяц назад

    l'État doit prendre ses responsabilités les bay fall en font trop à Touba c pas sérieux

  • @blackironlion12
    @blackironlion12 Месяц назад

    L'état doit prendre des précautions sur les Baye FALL qui n'ont pas de formation ni rien

  • @cheikhahmadoubamba5477
    @cheikhahmadoubamba5477 Месяц назад +1

    Douniou Ay Baye fall Ay domeram laniou rekk lolou dou cheikh ibra dou yon wii yalla xam nako

  • @BoubacarKara
    @BoubacarKara Месяц назад +1

    Pourquoi porté presse Ils ont des responsables Kou beugoul Serigne Touba bouffa deuk guirr lane comme yii di deff yi melni khamo dokhinou yonou mouride dano ame kilifeu

  • @badarabax
    @badarabax Месяц назад +5

    Yaw do imam Touba li sëriñ bi bëgg rekk mooy am .

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 Месяц назад +3

    Imam bonèk biir touba taxamol wormay touba ak ndabootam

  • @mamadousy8633
    @mamadousy8633 Месяц назад +8

    C'est une manière de décourager le mauvais comportement.Il faut éduquer vos enfants.Si c'était la police,tu verras pire et tu ne piperas mot.

    • @abdougueye2221
      @abdougueye2221 Месяц назад +2

      Kou yarou moyé yaré ko diangue khame moyé khamlé koo dégue dîné moye khamlé diné 8:14

    • @MamedaraThioub
      @MamedaraThioub Месяц назад

      Lou ler gua wax wayé il ne peut pas decourager personne au contraire il fait la publicité da la procedure des baye fall pour honorer le ndigueul du Khalif

  • @abombacke8547
    @abombacke8547 Месяц назад +2

    Dee dém sawara rék bayyi joulli bayyi woor nékfii di sonalaaté

  • @ousmanedaffe389
    @ousmanedaffe389 Месяц назад +1

    Ki wakhoufi tous diakhasé késé mo takh guay wakh so mounta yar sa wadia keur ci li serigneba beugué gua géne

    • @bassfall5382
      @bassfall5382 Месяц назад

      Khana ai doff gano diapé ki lime wakh loko gana lér

    • @ousmanedaffe389
      @ousmanedaffe389 Месяц назад

      Léroul kay ndakh khamoul bakham da guéne wala day nélaw

  • @aboudiop-fj4ug
    @aboudiop-fj4ug Месяц назад

    Kou giss khamné geumo yonou baye fall

  • @mormbaye5071
    @mormbaye5071 Месяц назад

    Machalla imam

  • @abdoukarimditmacodoundiaye993
    @abdoukarimditmacodoundiaye993 Месяц назад

    C'est l'état qui doit prendre la sécurité avant la riposte des humains

  • @mouhamadoukane2230
    @mouhamadoukane2230 Месяц назад +2

    Sénégal jupe parfois day dangue Imam il faudrait éduquer davantage vos protégées La loi lorsqu'elle est appliquée peut paraître dure mais nak Sam Touba diarnako

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад

      Serigne si nio dakha khoti wormay diiné dji, gueumouniou Yallah, gueumouniou al quran biniouy diangue, gueumouniou Rassoulillahi. Badio ak khaliss késsé laniou gueum 😂😂😂

    • @MamedaraThioub
      @MamedaraThioub Месяц назад

      Yaram pa bi mo gueuneu khamni la fille nékoil ci les bayfall non aucun interre darreter kelkun ki est en conformité avec les ndigueul
      C juste un facon de decoutager et de denigrer les bayfall
      Mais khamoul né bayfall ay rouma moko jike

    • @BayesaliouGueye-nc6wo
      @BayesaliouGueye-nc6wo Месяц назад

      Abdoubdoul billahi di nga de si nakhar😂😂te nga nopoulou😂😂

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад

      @BayesaliouGueye-nc6wo yen lolou rek ngen di wakh di doul rek 😂 wallahi mangui santé Yallah bou bakha bakh ndakh téral nama bou bakh al hamdoulillah. Sen deuk bobou amoul ndokh mou nékh té barina mboyo 😂😂😂

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 Месяц назад

      @MamedaraThioub koudoul diouli dou woor key sheytane laye ligueyeul 😂😂😂

  • @serigneadj1779
    @serigneadj1779 Месяц назад +5

    Diadieuf Imam
    Lo lu du deug du yone

  • @MameCheikh-z5m
    @MameCheikh-z5m Месяц назад

    Xam-xam rek lafi wax de
    Sëriñ bi yeena defer la am.
    Baye faal yi nek kilifë yeene defar lañu
    Ñiy wacci si terrain bi nak nitadi ak ñak xam diine moo leen sonal 😊

  • @sidimoctardiop3761
    @sidimoctardiop3761 Месяц назад +1

    Wax DEUG yalla deglou nala bu baax dé mais dama yakaron ni Lou graw wa graw lagnoula def ,diamono chorona bi Lolou la police doon def thi gnakka tak masque rek té 6000f 'hay Faye

  • @Tambayefall
    @Tambayefall Месяц назад +2

    Louy sa problème 👿 Waw ndakh lolou moy yone

  • @badaradiop3303
    @badaradiop3303 Месяц назад +7

    Ziar mé vraiment imame ligua wakhe amoul lousi graw jupe normale kéne téréwouko wayé jupe bougnou fante basi kaw lagni téré té lolou l'islam beug ko imame gnéne gni gnéna wara djitou si wormal touba Dakar dou touba baye fall yi ndiguel rek si kaw sa kanam

  • @LemouFall-u1q
    @LemouFall-u1q Месяц назад

    Etat bi dal dieul résponsabitém si Touba, Touba amoule écol khaléyi manounio diang manounio fo lo lal niouné Serigne bi dakoy téré doyna war

  • @MalickDiouf-wl1zm
    @MalickDiouf-wl1zm Месяц назад +2

    Allons-y rekk si une guerre civile éclate personne ne sera gagnant.

  • @CheikhmamouneMbacke-t3z
    @CheikhmamouneMbacke-t3z Месяц назад +3

    Jarajaf s khadim wax nga deug dé

  • @tout1958
    @tout1958 Месяц назад +2

    Li cheikh thioro domi xaram wax motax ngay wax mai Touba mom li Sérigne beugeu rék Moy am dém léne séne deukou Mame

    • @saloummansaly1745
      @saloummansaly1745 Месяц назад

      Yéw dé War nga diangi nahju

    • @YoroSarr-f8u
      @YoroSarr-f8u Месяц назад

      Yaw kou xamadi nga

    • @tout1958
      @tout1958 Месяц назад

      @YoroSarr-f8u Lou yakhou Sénégal wa pastef la ak séne you bari

    • @YoroSarr-f8u
      @YoroSarr-f8u Месяц назад

      @tout1958 doule nga ndax bokou ma pastef sama xalat lay wax té bindeff meunou mako tè wax doméram

  • @fallousylla5386
    @fallousylla5386 Месяц назад +3

    Ki mom keuram dal limou beugeu mofay am kouko meunoul dangay déf mot sa keur mam

  • @abdouniangtv180
    @abdouniangtv180 Месяц назад

    man mom baye fall damako bang rékk ta yalla takh ndakh amoun bén ndiaring si Sénégal stan bi diangoun khamoun dara

  • @SaliouFall-y5k
    @SaliouFall-y5k Месяц назад +1

    Ya toukhousi touba dé topou warmay sérigne bi rk mbanga délou sa keur mame rk point

    • @Reewmi24
      @Reewmi24 Месяц назад

      Yaw hana deglou wooo limm wahh lepp ? Delen andak seeni xell

  • @serignefalloumbacke7849
    @serignefalloumbacke7849 Месяц назад +2

    Wa lislam niaka djuly la guana bagne

  • @baytoul-asrar
    @baytoul-asrar Месяц назад +2

    Ligay wakh lou ko raw la lén police di def tè dogen wakh

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 Месяц назад

    Lepp Serigne Montakha la. Kilifa gou daye ni moom toogalfi Boroom Touba radyallahou anho nakalaye dieule lou dayni samm djikoyi diko denk ay bandi yoo khamni douniou diouli douniou woor lanka kandaré bania topp yoonou Serigne Bamba wou sellwi.

    • @noirafrik7085
      @noirafrik7085 Месяц назад

      Man de damaa diaxle lillaahi lii dagay mujj russ sax

  • @BayeMbaye-o4f
    @BayeMbaye-o4f Месяц назад +1

    😂😂😂 voilà la preuve de ce que Cheikh Thioro disait à l'Assemblée nationale. Allons y reck