BOKK YI MBIR XEWNA, YÀLLA WEER NA AMED XALIFA ÑAS

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 фев 2025

Комментарии • 186

  • @SyllaMouhtar313
    @SyllaMouhtar313 Месяц назад +6

    Dieureudieuf Baye Mbaye Guéye Sylla ❤️❤️❤️🙏🙏🙏

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692 Месяц назад +10

    Machalla Anna solo serigne Touba 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayediouf7119
    @mbayediouf7119 Месяц назад +10

    Goor gui liguèy bou ame sollo ngay dèf si yone wi machalla

    • @alphaoumardiallo3884
      @alphaoumardiallo3884 Месяц назад +1

      Machallah 🙏🙏🙏

    • @babacardiagne580
      @babacardiagne580 Месяц назад

      Ça c est pas un bon travail, faut pas active le feu du diable. ,Ahmeht Cisse et Niasse sont des gens a ecouter. Ce vieux a amplifie les insultes de Niasse

    • @MorNdiaye-r7f
      @MorNdiaye-r7f Месяц назад

      Wallahi

  • @MorNdiaye-r7f
    @MorNdiaye-r7f Месяц назад +1

    Dieureudieufé cheikhoul khadim dieureudieufé Serigne Touba dieureudieufé Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Mamadou-d5j
    @Mamadou-d5j Месяц назад +16

    Ahmed khalifa ak ahmed cisse kiff kiff nagnou yalla moussal thi ngom

    • @alphaoumardiallo3884
      @alphaoumardiallo3884 Месяц назад +3

      Amine ya Rabbi barké Cheikhoul Xadim Jarama MAME Cheikh Ibrahima Fall Lampe 🙏🙏🙏

  • @MansourThiam-l5n
    @MansourThiam-l5n Месяц назад +15

    Ba amet cissé saga wé allkhour Anne wakho wone dara.

    • @badiboy8698
      @badiboy8698 Месяц назад +1

      Adouna moy wadia diekh

    • @ameetfallsenegal3506
      @ameetfallsenegal3506 Месяц назад +5

      Ndakh baye mbaye gueye sylla mo mome al Quran

    • @modoudiallo132
      @modoudiallo132 Месяц назад +1

      Sa gni ay Naféque lén

    • @beyebaba3724
      @beyebaba3724 Месяц назад +3

      Me boukko nekhe lane mosisa yone lidiamtile sa probleme loutakhe guene sokhore

    • @badiboy8698
      @badiboy8698 Месяц назад

      @beyebaba3724 dof plus 🤣🤣

  • @almustafambakke6163
    @almustafambakke6163 Месяц назад +2

    Jërëjëfaty Baat mbay gëy Syll ❤

  • @khadimgueye665
    @khadimgueye665 Месяц назад +3

    Serigne bi serigne touba dou kougnouy khekhal kougnouy ligueyal la

    • @Iiiiiiiiii873
      @Iiiiiiiiii873 Месяц назад

      𝙇𝙞 𝙢𝙤𝙪𝙮𝙚 𝙙𝙚𝙛𝙛 𝙣𝙞 𝙗𝙤𝙪𝙙𝙤𝙪𝙡 𝙡𝙞𝙜𝙪𝙚́𝙮𝙚 𝙨𝙚𝙧𝙞𝙜𝙣𝙚 𝙏𝙤𝙪𝙗𝙖 𝙡𝙖𝙣𝙚 𝙢𝙤𝙮𝙚 𝙡𝙞𝙜𝙪𝙚́𝙮𝙚 𝙨𝙚𝙧𝙞𝙜𝙣𝙚 𝙩𝙤𝙪𝙗𝙖.

  • @AbsaCisse-bi2vu
    @AbsaCisse-bi2vu Месяц назад

    Yaa ngi juum de baay mbay, bul séddale benn wideo, ñii réeroo wuñu lii lépp ñoo ko tay, Ahmad Siise mii , baay Bay warul nekk ci sam sàq, saaga kat bàyyi leen ak saaga kat yi ñu Tontu leen, te Nga yam ci boroom xam-xam yi mana yàq😂
    Jërëjëf sëriñ Mbay , sa mbokkam Daaru kosso❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ninjablakfire6737
    @ninjablakfire6737 Месяц назад +3

    Wakh Ahmed Cissé bouthi baséwou

  • @PapaFall-r4n
    @PapaFall-r4n Месяц назад +1

    ❤❤ machalah amna solo

  • @firi_guente_et_secret
    @firi_guente_et_secret Месяц назад +1

    Ana gni sop seydouna Mohamad, maylén doolé chaîne bou béss bi gnou yaatal xam xam barkép yonénte bi slw

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 Месяц назад +1

    Serign touba nena nguen dem diamoudji yalla te bayi serign minguen di mboubo.

  • @LamineSow-s1r
    @LamineSow-s1r 27 дней назад

    Tout musulman doit aimer serign touba il a concentré toute sa vie pr l islam

  • @kebekebe587
    @kebekebe587 Месяц назад +5

    Wakhi Ahmed Cissé kouko gueme dala nekh baye mbaye gueye wakhi ahmad Cissé dou delou waye

    • @Cabayoroyoro
      @Cabayoroyoro Месяц назад +1

      Ahmed khalifa Niass mo wax gneupp dégg

    • @kebekebe587
      @kebekebe587 Месяц назад

      Mai wakhiul dafa bagne serigne bi nako tontou ci xamexam rek

  • @ahmadoungom8026
    @ahmadoungom8026 Месяц назад +4

    Bayi lene di yee fitna

  • @sambaliou5859
    @sambaliou5859 Месяц назад +4

    Baye mbaye wakhi Ahmed k Niass AK Ahmed Cissé Niort yame diaroul commenté ndakh
    Wakhi Ahmed Cissé manna nékk ay sooss

  • @laveriteabsoluejuste6358
    @laveriteabsoluejuste6358 Месяц назад +1

    ❤❤❤ Jaajëf

  • @Djilydiob-jf2ey
    @Djilydiob-jf2ey Месяц назад

    Jaajëf Baay Mbay ❤❤❤❤❤❤

  • @bassirougueye1287
    @bassirougueye1287 Месяц назад

    Jaajeuf Serigne Mbaye

  • @mouhamedmakhroufthiam1476
    @mouhamedmakhroufthiam1476 Месяц назад +2

    Père borom ham ham gua mai tay mom décoruma Ahmed cissê dou référence

    • @ablayedine6951
      @ablayedine6951 Месяц назад

      THIAM KON T'AS PAS COMPRIS,AHMET A SEMER L'IMPOLITESSE D'ATTAQUER LES CHEFS RELIGIEUX,ET DIEU L'A RENDU LA MONNAIE D'UNE ATTAQUE DE AMET CISSÉ

  • @defarpro5319
    @defarpro5319 Месяц назад

    Kou bayyi woul dèrou walliyu bou mèlnè ousmane sonko sa soutoura dina yagga khawèkou

  • @mouha313mouh8
    @mouha313mouh8 Месяц назад

    Machala baye mbaye toujours même yaguefi loool taa wér

  • @cheikhfall9985
    @cheikhfall9985 Месяц назад

    Ana gnidone khass cheikh Thioro Mbacké Khana amnane liguéy, kii mo sokhor

  • @barasow3654
    @barasow3654 Месяц назад

    DIEUREDIEUF baye MBAYE GUEYE syll

  • @babacarmbengue4662
    @babacarmbengue4662 Месяц назад +1

    Yalla dinako atte ak kou teddi ki Cheikh Ahmadou bamba inchahala

  • @mfn9511
    @mfn9511 Месяц назад +1

    Ahimèd khakifa niass yarouwoul tè khamoul dra Walahi

  • @ndeyeamykéne
    @ndeyeamykéne Месяц назад +2

    Gorgui Niass d saytané Bouy doxx si kaw dox Si kaw souff
    Mom aldianam mongikoy doundou si kaw souff lepa dagan si mom😂

  • @gaindefatma3001
    @gaindefatma3001 Месяц назад +2

    Serigne bi sylla boul dougue ci wakhou gni. Diombaleiko sa bopp

  • @papyjunior4780
    @papyjunior4780 Месяц назад +4

    Segn bi guissou meu leu nga wakh weddi omar diagn limou wakh si tiraitii. Mane mom yaw laa done khaar ndakh yagu naa leu seetaane si histoire. Et kham nga li omar diagn wakh si tirailleurs yii lolou leu.

    • @mamadoutoure4911
      @mamadoutoure4911 Месяц назад +1

      Yaw boul yakanti bou serigne touba sokhlawé kou ko tontoul OMAR DIAGNE DAY KHAR

    • @papyjunior4780
      @papyjunior4780 Месяц назад +1

      @mamadoutoure4911 Segn bi mane mouride laa diaroul nga may siangal liga bind niii. Mane omar diagne falé wou meu ko. Bimou khassé sunu serign yii la bayé nawlo.

  • @IbrahimaThioune-kf2rb
    @IbrahimaThioune-kf2rb Месяц назад +1

    Assalamou alaycoum bay mbay bagon nagne nga ngeuw si mbiroum trayeur yi

  • @FaaFallilou
    @FaaFallilou Месяц назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Grazie mille

  • @mbfa9157
    @mbfa9157 Месяц назад

    DIEUREUDIEUF BAYE mbaye lou lerr nga elhadji malick sy la fi wakhon lou ko nga

  • @ahmadoudame7031
    @ahmadoudame7031 Месяц назад +2

    Pa bi ak Ahmad khalipha yénayam limou wakh si yallah lepou meti woula yabon😢guanan limou wakh serigne touba 😢mbamou kharam yi👹👹dome khathi you bon yi

    • @badiboy8698
      @badiboy8698 Месяц назад

      Yonentebi amoul domou ndeye senegal

    • @OusmaneMarega-sl2zn
      @OusmaneMarega-sl2zn Месяц назад +1

      parce que Sén tarikha yi nio léne eupal solo dina yallah bii

  • @papemalickdiop7681
    @papemalickdiop7681 Месяц назад +4

    YALNA YALLA GUDËL SA FAN TE WEREL SAY CËR BAAY MBAY

    • @alphaoumardiallo3884
      @alphaoumardiallo3884 Месяц назад +1

      Amine ya Rabbi barké Cheikhoul Xadim Jarama MAME Cheikh Ibrahima Fall Lampe 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @diopibra8512
    @diopibra8512 Месяц назад +3

    Dieredieuf s mbaye gueue Silla
    Muridyi ammel nanu la nioucal

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Месяц назад +1

    Ahmeth Cissé dou niit cou bakh dé, serigne Mbaye syll fait attention attention attention à AHMET CISSÉ

  • @moustaphadiop9437
    @moustaphadiop9437 Месяц назад

    Mane dama yurum Ahmad khalifa niass wallahi

  • @BaboucarrGaye-vu2hb
    @BaboucarrGaye-vu2hb Месяц назад +2

    yen niepa yem, diogeeleen si seen tarqa yi dimu ji Yalla

  • @diarama313TV
    @diarama313TV Месяц назад

    DiARAMA baye mbaye ❤❤❤

  • @kebekebe587
    @kebekebe587 Месяц назад +7

    Baye mbaye aujourd'hui je ne suis pas d'accord avec vous

  • @thiernosylla2816
    @thiernosylla2816 Месяц назад +1

    Kiko dalalon dey baye mbaye mo yeuss niépp

  • @oumarmamadoumbaye3229
    @oumarmamadoumbaye3229 Месяц назад +1

    Mbaye gueye sylla. Tu as insulté cheikh oumar foutiyou.

  • @babacarmbengue645
    @babacarmbengue645 Месяц назад +1

    Salam baye mbaye mane la bamba Paris ndakh meune na ame wakhtane wowou ngir yalla

  • @SherifAhemedMouhamed-mj8nl
    @SherifAhemedMouhamed-mj8nl Месяц назад

    Ndayssan ahmad khalifa khawema kan mokou yakh wanti amena lokou dall wakeurem warenenkou fadji , hasbona ALLAHOU wa nimal wakil

  • @Mountagasow-h1i
    @Mountagasow-h1i Месяц назад +1

    Thieuye li probleme bou doul diex

  • @SherifAhemedMouhamed-mj8nl
    @SherifAhemedMouhamed-mj8nl Месяц назад

    Ko am yaye cherifela waroul wax ci ken , wanti ay yakhou yakhou rek mokou top ndayssane

  • @maimounasene6488
    @maimounasene6488 Месяц назад

    Wa kon gni ahmet cissè laniouy dèglou, ki dip nafeh di saga alkhourane

  • @abdoulahatdioufyallnangafi8361
    @abdoulahatdioufyallnangafi8361 Месяц назад +2

    Ahmèt khalifa.masoul gem s touba dadon dor dafa khèwi won bega khèwat di dor murityi wayè.gemoul dara domiramla bumak

  • @IbrambayeSenegal
    @IbrambayeSenegal Месяц назад

    😂😂😂 Ahmad Khalifa dafa nakh

  • @BabacarDiagne-o2r
    @BabacarDiagne-o2r Месяц назад

    yénna yame rék kiff kiff

  • @modouthiam2461
    @modouthiam2461 Месяц назад +2

    ioe shaytane ngua wakho fi dara

  • @aboubacarndiaye3425
    @aboubacarndiaye3425 Месяц назад +3

    Mais Ahmed gno gnaam gno yam pask ki waxtanu biir neeek la dafa xouloo AK moom rek merr guené ko wayee cilawone.

  • @ndiagadaguelakane4044
    @ndiagadaguelakane4044 Месяц назад +3

    Gogui sylla lou niawe keneu douko siweul kouko siweul yakk momema yame

  • @issasene8747
    @issasene8747 Месяц назад

    Xalifa niass kou kateu ndeyam la

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Месяц назад

    Serigne Mbaye syll vraiment attention attention attention attention attention à Ahmet CISSÉ il est très dangereux

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692 Месяц назад +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @YesItali-y7f
    @YesItali-y7f Месяц назад +2

    Amoul morom khadim Rassoul

  • @mamemorniang9550
    @mamemorniang9550 Месяц назад

    عبدالله وخديم رسوله صلى الله عليه وسلم serigne Touba kémaanou borom amounou diott di khoulo ak ay say say

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 Месяц назад +1

    Merci beaucoup ❤

  • @thieyassine
    @thieyassine Месяц назад

    Serigne Mbaye Guèye Syll gni téki woul dara est-ce que diar na nio tontou ? Da nga léndi ignorer .

  • @ElxalifLom
    @ElxalifLom Месяц назад

    Li Ahmed cissé wax lu ndaw la Ci Ahmed Niass. Man rek Lima xam ci Ahmed Niass gnémé wumako wax 😢 xadj deugg la

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 Месяц назад

    Dama yakaar ni Danga xamut Ahmed Cissé Wala Dawo topu Ay waxam Ak jëfam kon di Nga tèy ci Ay waxam

  • @aliounecisse2392
    @aliounecisse2392 Месяц назад

    Ahmed cissé dou lepp la niouy wakh. Est ce que tu connais ce que ça peut causer. Tidiane khamna lou beury noppi.

  • @mbtv3335
    @mbtv3335 Месяц назад

    Baye mbaye gueye gneuweul gnou si cheikh oumar diagne miné tirailleurs yi ay traite lagnou

  • @balabeybalabey8403
    @balabeybalabey8403 Месяц назад

    MANGILAYNIAN BAYE MB,GEUYE
    DINDIL FOTO AKHMED CISSÉ BI
    BOUL TEGATI AYWAKHAM
    GENELÉN SIMOM

  • @malickseck9424
    @malickseck9424 Месяц назад

    😂😂c'est à votre tour 😂😂Ahmed niass fi la takhaw di saga Cheikh Seydil Hadj Malick minga khamné kouko geuneu sél si rewmi guissé gouma ,nguén diko tathio keu tatagal 😢😢😢aujourd'hui yénakoy djiebané...Parparloo yak nalén kouné sa bopou la intéressé lou téwone yaw mbaye gueye sill nga dénoncé woneko à temps ? Isssh... nguén diy woté ay dioulitt kholatt lén sén bopou té lounou torakhal seniy mbok nguén khép ko.

  • @serignemodoudiene95
    @serignemodoudiene95 Месяц назад

    Serige Touba amolli morom want dall s mbaye tal nanou lennie Lo doll gayoyou

  • @MamediarraThiam-q5f
    @MamediarraThiam-q5f Месяц назад

    Merci

  • @abdoulayediouf805
    @abdoulayediouf805 Месяц назад

    liii amoul ragal waleu seral tegal sén ndey rek

  • @abdoulayengom7659
    @abdoulayengom7659 Месяц назад +3

    Bayil di guawa wax ak di guawa juger Ahmed khalifa guèn meusou ko dègue mou saga wala mou wax serign bi lou boone .Ahmed cise mi soko xam do basé si ayyy waxam

  • @abakarafall6276
    @abakarafall6276 Месяц назад

    Akmet kalipa nass mi mo mana fen

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Месяц назад

    Serigne Mbaye Syll attention attention attention aux dires Ahmeth Cissé ce type est un domeram piiiiiiiir piiiiiiiir piiiiiiiir

  • @babacarndoye2457
    @babacarndoye2457 Месяц назад

    Goorgui mak dou netali dou diotali wakh djou bon ak bou ñaw.kholatal sa bop

  • @kilimandjarotv1508
    @kilimandjarotv1508 Месяц назад

    Moi des Omar Diane

  • @Boubacarakbourtv5226
    @Boubacarakbourtv5226 Месяц назад +2

    Yaw ahmet cissé linga wakh mo geuneu bone..yaw ya wakh né l'islam amoul ndiarigne yaw mbam kharam ngeu mérité woulou doundou dano warone dageu sa bopou domou kharam bou bone bi yaw danga alkou

  • @ndogolisatubmamyarubmamtv7370
    @ndogolisatubmamyarubmamtv7370 Месяц назад

    Cissé mi AB saytanee radjim la day fen bu Amon Lu niaw andoko AB saytanee la
    Bay mbaye ngir Yalla bull diapu si waxu ki
    Man bimay daw bagay neku RTS Touba lalay deklu

  • @TubaboGiboroh
    @TubaboGiboroh Месяц назад

    😂😂😂😂😂😂😂 almeria kayi

  • @mourtadagueye6931
    @mourtadagueye6931 Месяц назад

    PA bi kanam kou bonn la yoré

  • @mamadousarr5827
    @mamadousarr5827 Месяц назад

    Lolou amoul benn ndiarigne. Waxi Khalifa Niass amoul benn dieexite thiy talibé yi

  • @ousmanembodj8363
    @ousmanembodj8363 Месяц назад

    Gorgui ioe xana danga bagne ahmet khalifa? Si waxou ahmed cissé ngaye souka ndiko paa ioe tamite kou wakh fégne

  • @TubaboGiboroh
    @TubaboGiboroh Месяц назад

    Yena xam de ....sama yon nekousi

  • @bijoujobe8668
    @bijoujobe8668 Месяц назад

    Akhmed sai sai la .lougne ko wakhal moko def

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib79 Месяц назад

    Ngi niar dé nio Yam séni wah méwako geunaa way niar niou tekiwoul dara lann

  • @elhadjiba4763
    @elhadjiba4763 Месяц назад +1

    Bayilenne diaxasse

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 Месяц назад

    Baay Mbaye bu sañoon Waxi Ahmed Cissé mom Doo ci souka ndiku ki yax Nit rekk la man ta gamut Dara Li mom bayo Boo Nga Dundi ko léegi bala muy sori

  • @abasscherif07
    @abasscherif07 Месяц назад

    Yw pa bu sytanège dèmal ge diamu yalla mo gen diw waxne diw waxne rusel se bèdiawbi

  • @abdoulayengom7659
    @abdoulayengom7659 Месяц назад +1

    By mbay guey tél gua wax dhè ! Ahmed cisse day xoulo rek té xoulo wax lou ñiane leuh rek .xaral ba dègue wax niou bone bayiko si ahmed khalifa niass gua sogua wax .Waxi ahmed cissè diarula basé ndakh fi la takkheu ahmed taaay mou takhawe diko saga

  • @MbackeNdar82
    @MbackeNdar82 Месяц назад +1

    Ameth khalifa niass loudoul Alall niorouko

  • @diarracoly3214
    @diarracoly3214 Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @CheikhGayeislam
    @CheikhGayeislam Месяц назад

    NDAX XAM GEN ISLAM OMMAYADES YI AK ISLAM ABASSIDES YI LOUGNOU FI BAYI ???

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 Месяц назад

    Ben yonne rekk mo am .mouy l islam.point

  • @ceernojuuf251
    @ceernojuuf251 Месяц назад

    Moytu leen Ahmed siise mii misyoo lay dox de. Ba mu sorti.

  • @BibicheCocoThiam
    @BibicheCocoThiam Месяц назад

    Lingéndidef amoul ndiargne

  • @yytv8221
    @yytv8221 Месяц назад +1

    Ahmed mom mok yow ak Cheikh Ceesay yeinneu yem, diammou ji len YALLAH.

  • @CheikhounaDiop-y5r
    @CheikhounaDiop-y5r Месяц назад

    ❤❤❤❤

  • @bismillabismilla8878
    @bismillabismilla8878 Месяц назад

    Nékalén ay Nit Ahmed Cisse mou halakou mi nganan Seringe Touba wané na bopam.
    Ki yako xamoul wayé nila mél ay waxam jaroul japp
    yaw mi sah so moytou woul dinala wax louy ta(à té dou fay

  • @moustaphadiouf1534
    @moustaphadiouf1534 Месяц назад

    Ki ko dalale day féne ki toudé Serigne Touba doom dou ko wax Lou gnaw

  • @biboulayetouray1517
    @biboulayetouray1517 Месяц назад

    Eskey yalla sunu borom

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Месяц назад

    Les deux Ahmet là dognio Alcou Serigne amoul mbollo déjà Moy wakhi doff