URGENT : Imam Khadim Ndiaye Parcelle lima Baye Fall yi déff fi Ci Touba Man....

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 янв 2025

Комментарии •

  • @assaneyate196
    @assaneyate196 7 дней назад +83

    Je suis 💯 % d'avis avec cheikh tioro mbacke. Certains comportements des bayes Fall interpellent, ils ne peuvent pas jouer le rôle de la police. Il faut nécessairement que l'État puisse de concert avec le khalife trouver une solution adéquate sinon ça risque de dégénérer à l'avenir !

    • @ndiayefatou565
      @ndiayefatou565 7 дней назад

      Yaw diouliwo, woro di torokhale ay dioulite! Gni vrai imbécile lagnou

    • @PapamodricDiatta
      @PapamodricDiatta 7 дней назад +3

      Vraiment

    • @YAYANDIAYE-x7o
      @YAYANDIAYE-x7o 7 дней назад +4

      Kissi lale sama Bok jour bobou deah nassi ray nite avant nioma ray

    • @YacineDiop-vm2yd
      @YacineDiop-vm2yd 7 дней назад +3

      Tu as vraiment dis la vérité.....

    • @khoudiakambel5290
      @khoudiakambel5290 7 дней назад

      Nopil So xamou Liga y WAX ok nek sa guînaw telephone di WAX lo xamoul

  • @بابكرسيك
    @بابكرسيك 7 дней назад +25

    الصلاه عماد الدين فمن أقامها فقد أقام الدين فمن تركها فقد ترك الدين صدق رسول الله صل الله عليه وسلم

    • @codefall4963
      @codefall4963 7 дней назад +2

      والله والله العظيم يا شيخ صحيح

    • @mordiop7160
      @mordiop7160 7 дней назад +1

      Vérité

    • @FallMatar-b4e
      @FallMatar-b4e 7 дней назад

      😂😂😂😂

    • @makhtarniang8577
      @makhtarniang8577 7 дней назад +1

      ویل للمصلین صدف الله العظيم

    • @bassdiop5079
      @bassdiop5079 7 дней назад

      ​@@makhtarniang8577 tu devais continuer le verset et tu comprendra

  • @OusmaneSambe-l3f
    @OusmaneSambe-l3f 7 дней назад +78

    Li vraiment niawna 😢Serigne Touba santané woul banditisme bi déé😢😢😢

  • @serignendiaye9275
    @serignendiaye9275 7 дней назад +139

    Temps que rayignou nitt kèn dousi wakh civiles dou regler civiles

    • @serignembackedia3506
      @serignembackedia3506 7 дней назад +3

      khana rayat not

    • @aichasecka-8974
      @aichasecka-8974 7 дней назад +11

      Kou meuneu deuk kou meunoul guéne deukou diambour un point un tiré

    • @khadimegueye9070
      @khadimegueye9070 7 дней назад +3

      @@aichasecka-8974 yaw doul way sof ga trop

    • @aichasecka-8974
      @aichasecka-8974 7 дней назад +1

      @@khadimegueye9070 sa doulou baye kou meuneu deuk deuk kou meunoul niouss sa ndeye si biti

    • @votremiroir7612
      @votremiroir7612 7 дней назад

      ​@@aichasecka-8974dara ngafi wakhoul bayilén sén thiakhane yi

  • @cheikhoulkhadimfaye525
    @cheikhoulkhadimfaye525 7 дней назад +57

    Je suis parfaitement d'accord avec Cheikh Thioro ,avant tout warmay Touba wayé ci nité

    • @PapamodricDiatta
      @PapamodricDiatta 7 дней назад +1

      Vraiment

    • @AliouDiarra-c7y
      @AliouDiarra-c7y 6 дней назад

      Touba n'appartient pas à personne pour expliquer,,,Touba pour Serigne Touba et personne ne peut barrer les bayes fall ok

  • @moustaphanoble1231
    @moustaphanoble1231 7 дней назад +14

    Dieureudieuf seringe touba ❤❤❤❤❤

  • @moussacisse5397
    @moussacisse5397 7 дней назад +83

    Koudoule diouli naka laye duk lé solou boulene niy fonto dame léne diangui pour khame sene dinne

    • @adioumadiagne7607
      @adioumadiagne7607 7 дней назад +6

      Wakh deug Yàlla

    • @oumarniang438
      @oumarniang438 7 дней назад +4

      Deug deug

    • @HamathDiallo-mu8de
      @HamathDiallo-mu8de 7 дней назад +3

      Franchement

    • @fallousylla4764
      @fallousylla4764 7 дней назад +3

      Deug deug do djiouly do woor do def dara lou l'islam bi santané ngané dangay reglé ay soline

    • @badiboy8698
      @badiboy8698 7 дней назад +2

      Dara yefou yebate rekk senegal come dou senegal linouy def bouko gouvernement bi defon nou weur tele yii dii youd

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye662 7 дней назад +27

    Merci beaucoup imame❤❤❤

  • @thioyedoumo9571
    @thioyedoumo9571 7 дней назад +77

    Comment quelqu'un qui ne prie pas , peut agir au nom de l'Islam?

    • @user-LatzoDiouf04
      @user-LatzoDiouf04 7 дней назад +7

      lolu sa yone nekousii mandoulén

    • @And.611
      @And.611 7 дней назад +4

      Moma diakhal

    • @coursdecoutureenwolof
      @coursdecoutureenwolof 7 дней назад +1

      😂

    • @deugrek344
      @deugrek344 7 дней назад

      ​​​@@user-LatzoDiouf04 démal ngua diangui diiné bakham loy mandou thie diiné. Diouli ak wor dioulit war ko déf ngua nane mandou😂😂. Yaw ko yab. Magui khar ngua andil ma ben téré diiné wala bou serigne touba bouniou wakh niit boudoul diouli dou wor dagua wara mandou thie mome. Wala fane la serigne touba wakh kou hormaloul touba torokhal lén ko daur lén ko. Respectélén niit yi té deugou. Bouniou wakhé guéni sagua niit ak menacer.

    • @oumarniang438
      @oumarniang438 7 дней назад

      Vraiment.
      Non seulement ils ne prient pas aussi ils sont sales et mal habillé

  • @badandiaye1636
    @badandiaye1636 6 дней назад +4

    Touba serigne touba moko mome nigall rek

  • @Generalahmadoudame
    @Generalahmadoudame 6 дней назад +2

    Wa pastef yiy khekh s touba kase no d'accord ak yaw mag motolni yaw di wakh wakho mbind lommana safara te ko sol ab seppo khamgani xat xat gimo xat motakh no teeko li s bi beuge day am ❤

  • @bounaseck4068
    @bounaseck4068 7 дней назад +27

    Rewande rek la😢

  • @KM-ou8cw
    @KM-ou8cw 2 дня назад

    Xawma lou xew ndah fekewma ki di netali tmt limsi feké sakh bariwoul kon ba legui dara leroumasi wayé li serigne bi beug moy am🙏❤️

  • @khadimegueye9070
    @khadimegueye9070 7 дней назад +34

    Baye Fall yi duñu sarap ndayam domeram yi

  • @atekhdiop2276
    @atekhdiop2276 19 часов назад

    Merci

  • @amleking2219
    @amleking2219 7 дней назад +34

    Sénégal nékhoula wakhé mais bou ëuleugué dinane khamni serigne bi nékoul si yi niou nék blh💔💔

  • @elhadjidrmd8954
    @elhadjidrmd8954 7 дней назад +14

    Merci imame

  • @AssaneFall-v7e
    @AssaneFall-v7e 7 дней назад +14

    Sonko moy6 Président du Sénégal inchallah❤❤❤❤❤❤ 2029

  • @Aissatou-b4b
    @Aissatou-b4b 7 дней назад +7

    Cheikh thioro a raison 😢

  • @Dgcfh123
    @Dgcfh123 7 дней назад +7

    Bo nio rayol bay fal lii dofi diogeee 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ibrandiaye5389
    @ibrandiaye5389 7 дней назад +10

    Bilahi touba mieti na 😢😢

  • @adamaasannefaye8372
    @adamaasannefaye8372 6 дней назад +7

    Les baye fall doivent être corrigé

  • @xassaidvisiontv2008
    @xassaidvisiontv2008 7 дней назад +7

    Lima leer dall mooy Li serigne bi beug moy am In chaalah 😂 té Aka youmbu wallahi 99% ñapp Ñogui si

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye5922 7 дней назад +14

    Merci beaucoup imam ❤❤❤

  • @bazirpascal7491
    @bazirpascal7491 7 дней назад +8

    Il faut que ça s'arrête. L'islam n'a pas enseigné ces genres de pratiques. Ça suffit que le gouvernement prend ces responsabilités

  • @BijouNdiaye-g8i
    @BijouNdiaye-g8i 7 дней назад +2

    Thiey 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @modoumboup39
    @modoumboup39 7 дней назад +14

    L'état du Sénégal sera tenu responsable de tout ce qui pourrait y avoir comme conséquence.... allons rek

    • @MarameNdiaye-hj6sv
      @MarameNdiaye-hj6sv 6 дней назад

      État bou atté atté lismame rék touba keurou diabour la

  • @serignekebesallkhassida4667
    @serignekebesallkhassida4667 7 дней назад +2

    Kou waxul deugg wakh ndy ay fenne Tuubaa Lifiii Am dou deugg Dou yoon yeurmande Amatoul Tuubaa mais Lou way dff sa bopp

  • @mixbii7831
    @mixbii7831 7 дней назад +12

    Xana Touba bokkul ci Sénégal bay ame sa propre loi bikoy régir na Diomaye réglé lii xamal baye yii douniou ay gendarmes

    • @talentfoottv3861
      @talentfoottv3861 7 дней назад +1

      Vraiment li dafa eup trop

    • @pascalkane9767
      @pascalkane9767 7 дней назад +1

      Vraiment. Il est temps que l'état prenne ses responsabilités par rapport à cela.

  • @diagnemomo4771
    @diagnemomo4771 7 дней назад +8

    Cheikh thioro limou waxx Moy deugeu baye fall yi naniou léguéyi niak diom lagne déff

  • @diawi2588
    @diawi2588 7 дней назад +18

    Lii bougnou si jougout, dina eupp ay loxo

  • @MbayeFall-m1m
    @MbayeFall-m1m 7 дней назад +19

    C'est khalifa général qui est responsable de ce bordel à Touba.

  • @AwaSeye-wi8te
    @AwaSeye-wi8te 6 дней назад

    😭😭😭😭❤️❤️

  • @MoryKhouma-hl5tj
    @MoryKhouma-hl5tj 7 дней назад

    Machallah

  • @adamsfaye9932
    @adamsfaye9932 7 дней назад +6

    Je suis écoeuré d'entendre ces injustices. Ils interdisent des habits non conformes avec les règles de l'islam en laissant du pire

  • @Satoubavrai
    @Satoubavrai 5 дней назад

    Ko doul baye fall baye fall mola guene afia baye fall yi ahmadou bamba protège dondo léne ❤❤ Free Palestine ❤❤❤Palestine libre

  • @elhadjifalilouka5665
    @elhadjifalilouka5665 8 дней назад +16

    Li môme c grave bilahi guerre civil Dina âme Touba legui

    • @saliousylla6062
      @saliousylla6062 7 дней назад +8

      Khana yaco Faye indi Touba nekhalounou kend wowou niou kend cou menoul li borome beug boufa dème c simple

    • @ibnouserignefall6965
      @ibnouserignefall6965 7 дней назад

      @@saliousylla6062saway linguay wakhni dou idée violence réglée woulle dara nak si adouna ngioune ngiépp nak si deukbi lagne deuk wormay touba mome dou ni lagne ko warra sammei wallahi nak fimou dieum dou nékh mallako wakh nak ta nanou démm rek

    • @DiagneElhadji-d8f
      @DiagneElhadji-d8f 7 дней назад

      Khana Yako faye deff

    • @Adjibara-t9z
      @Adjibara-t9z 7 дней назад

      @@saliousylla6062maylén nitt diam nganan li borom beugg li yallah beug laniou wara nieuké boulén niou sonal boy

    • @Adjibara-t9z
      @Adjibara-t9z 7 дней назад +2

      @@DiagneElhadji-d8fliko fiy endi moy di bay bayal loudoul weuy li baye fall yi neké dou deug dou yone

  • @BintaBamba-e1h
    @BintaBamba-e1h 6 дней назад +1

    Vraiment dou yon

  • @bmtv2334
    @bmtv2334 7 дней назад

    😢😢😢😢 meti na lool de 😢😢

  • @MaïKante-z2c
    @MaïKante-z2c 7 дней назад +5

    Touba li serigne bi beugue rek mofaye am kouko meunoull géneull deuk bi Sénégal yatouna demall deuk foulla nekh 😊diaroull wax diou beuri

  • @bathiemassambathiam6749
    @bathiemassambathiam6749 8 дней назад +7

    Kéne khamoul liii 😂😂😂😂

    • @AmiDieng-bd9cq
      @AmiDieng-bd9cq 7 дней назад

      Doyna war dal lasi kham 😂😂😂

  • @BayeassaneGueye-by5eo
    @BayeassaneGueye-by5eo День назад

    Kép Kou BAYE FALL yi japp Daga df Lou SERIGNE bi di bagn

  • @falloundiaye7208
    @falloundiaye7208 7 дней назад +1

    Ndaysane

  • @MammorSeck
    @MammorSeck 5 дней назад

    Lii tegou won feneu😢😢😢

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 7 дней назад +5

    Trop c trop dh nama yalla baal mais civile manoul yarr maromou civile li Serigne cheikh thioro done wakh rek

  • @fataima9095
    @fataima9095 6 дней назад +1

    Abdoulaye Wade, Macky Sall 😢 ay gouvernement you bone yakh réwmi en espace de 25 ans Touba est devenu un état dans un État 😮 lii Sénégal rek la am 😢 c'est devenu très dangereux de laisser cela continuer sans remettre les Sénégalais au même niveau sinon lii guerre civile rampant la guiss mouy nieuw a grande vitesse si le vrai Etat ne prend pas son courage pour le régler définitivement sans l'influence de personnes

  • @inssandiaye488
    @inssandiaye488 7 дней назад +4

    Merci beaucoup

  • @ThiouneKhadi-g1l
    @ThiouneKhadi-g1l 6 дней назад

    ❤❤❤

  • @moustaphandiaye1407
    @moustaphandiaye1407 7 дней назад +31

    IMAM SERIGNE KHADIM NDIAYE LIMOU WAKH LEP DEUG LEU

    • @moussafame4235
      @moussafame4235 7 дней назад +1

      Wakhoufi darra li s mountakha mbacke Moy am.

    • @dexterdexmen6707
      @dexterdexmen6707 7 дней назад +1

      ⁠bilay serigne bi beugue rek moy ame sindeukeum bi

    • @darkpenguin1978
      @darkpenguin1978 7 дней назад

      Yéwou lène Li loubesse la amoul fène

  • @mamemorthiam8763
    @mamemorthiam8763 7 дней назад +12

    Diap nit door wat fay 25 mil di déf lola nékh nio nan diiné li kay fou diiné déf lola nékh la

  • @mameantagueye8677
    @mameantagueye8677 7 дней назад +3

    Lima diakhale khana fofou amoule police

  • @SidiNiang-w2u
    @SidiNiang-w2u 6 дней назад

    Imamou nafékkyi koubagn serigne Touba dinga dée

  • @mamemalickthioune9305
    @mamemalickthioune9305 День назад

    Ah thiam khamounioula dh yaa Imaam wayé baxna

  • @alioudia3320
    @alioudia3320 6 дней назад

    Bakhna li wa bakhna reck

  • @MbayeKhadim-h9c
    @MbayeKhadim-h9c 6 дней назад +1

    Li nianwna😢

  • @ChiekhGeuye-r1y
    @ChiekhGeuye-r1y 7 дней назад +1

    Wallahi lii dafa apu😢😢

  • @khalyniang518
    @khalyniang518 7 дней назад +3

    Eska doune lambatou di diap plaisir 🎉

  • @coursdecoutureenwolof
    @coursdecoutureenwolof 7 дней назад +4

    Jupe longue losi nek

  • @CheikhLo-dt1ct
    @CheikhLo-dt1ct 7 дней назад

    Merci beaucoup sonko

  • @ndonguodieng2501
    @ndonguodieng2501 7 дней назад +2

    Des civils ne peuvent pas faire la police à la place des policiers dans un état normal et organisé.

  • @nassergaye9086
    @nassergaye9086 7 дней назад +2

    Amna titangué...dawna yaram ndeyssane.

  • @BayeassaneGueye-by5eo
    @BayeassaneGueye-by5eo День назад +1

    SERIGNA TOUBA waxon nani SAMA DËK BI DI TOUBA JANG ALKHOURHAN AK DIKO FI JANGALÉ LA FI BËG yaw nga bayi fi TOUBA dém fénén diko fa défé kon say wax day nakh saaay nopi war nala yaw ak gni mélni yaw kou yaroul sa ndiabote si li SERIGNE bi bëg BAYE FALL gnom yaar lén si li SERIGNE diguelé

  • @mbayammbayam2597
    @mbayammbayam2597 7 дней назад +1

    Bay fall Yi nagn dém diamou j yallah mo geun sen thiakhane Yi touba si bopam mo diarul dém legui parceQue dafa yakhou DEUK BO KHAMNI BOKKALÉ REK 😢 HARAM

  • @aminahsoumare
    @aminahsoumare 7 дней назад +1

    Salam gni danio yebaaté, nous prions aux autorités de freiner ce fléau, gni deureum laniouy wout bil baatil, lii niaaw na😢

  • @madicketall8643
    @madicketall8643 8 дней назад +15

    Liye rame si niague bi leu dieum. Bouniou dieuloule aye mesure pour arrêter li douniou khame foumouye moudié

  • @rapshouseofficiel9072
    @rapshouseofficiel9072 7 дней назад +1

    Sénégal dall barri nagne fontou li pour lane la😢😢

  • @joaopaulo77pulo78
    @joaopaulo77pulo78 7 дней назад +4

    Wakhji moy ap yéfér dou réglé ap dioulit

  • @BallaNiang-tp2ui
    @BallaNiang-tp2ui 6 дней назад

    Il faut que le gouvernement prenne la sécurité des biens et des personnes dans tous le territoires du pays

  • @DiagneElhadji-d8f
    @DiagneElhadji-d8f 7 дней назад +10

    Ab sip Kay way imam roussall wah lolu en te que imam nak sa domme nek birr Touba nga takhaw nanny ap sip la sol ta AKsina si omyi vraiment imam baye fall ay diambare lagn🎉

  • @diaggasamb7302
    @diaggasamb7302 6 дней назад

    Wa tamit koudoul djouli mom war ga 😮😮😮

  • @OusseynouThioub-ev8wn
    @OusseynouThioub-ev8wn 8 дней назад +13

    Jeureu jeufeuti Srg bi wallahi wakh nga lepp baye fall yi dém lén diéma kham lilén yalla wakh ak lilén yalla digeule ci sén diiné nguén jeuféko té diéma guén ci sén yi nguén nék thiakhane bakhoule nak ah🙏🙏

  • @CheickibrafallMbaye-rk4ml
    @CheickibrafallMbaye-rk4ml 7 дней назад +1

    😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @moustaphadiaw7203
    @moustaphadiaw7203 7 дней назад

    Ce est grave

  • @Cissella-eg7rz
    @Cissella-eg7rz 7 дней назад +5

    Mais cheikh thioro à parfaitement raison les baye Fall son entrain de semer la terreur pourquoi l'état n'ose pas réagir un civil ne doit pas faire la loi à un civil

  • @papeassanesow5248
    @papeassanesow5248 7 дней назад

    Walahi sounah rek moléne di dérangé wayé inchallah sounah thie kaw bida sii souf inchallah

  • @albanistabaguila5946
    @albanistabaguila5946 6 дней назад

    On est dans un pays laïque,l’état doit prendre toutes ses responsabilités avant que cela passe à une vitesse supérieure.

  • @biramediouf9533
    @biramediouf9533 7 дней назад +4

    Sama yonnne nekoujii walahi

  • @AbdoulbBaro
    @AbdoulbBaro 6 дней назад

    C’est de l’impolitesse total c’est fumeur de yamba ki règle notre touba c’est pas du normal bilahi Wallahi

  • @SerigneFallthiam
    @SerigneFallthiam 6 дней назад

    Bayilldoull saytane rek nga😮

  • @khalyniang518
    @khalyniang518 7 дней назад

    Katt rekk

  • @AblayeDiouf-hl7wh
    @AblayeDiouf-hl7wh 7 дней назад +2

    Thiowli thiowli ki ack gni digate cheikh Ibra moléni dérange bilahi wakh daye yénou mana toto yimouye saboté kifinécale Serigne Touba moléne ko diokh bayéne nafékh Di diakhasé té dioup

  • @fatouseck2817
    @fatouseck2817 7 дней назад +1

    Waw bay fall yi nak

  • @momocreation3631
    @momocreation3631 7 дней назад +1

    Dagay sét li rék 🤦cheikh thioro degue rek la wahk ❤❤ baye faux yi danio wara nek aye nité té bayi dof dof Lou bi☹️

  • @cheikhseck2799
    @cheikhseck2799 7 дней назад +8

    Merci Baye fall yi

  • @CheikhNdiaye-yr7zo
    @CheikhNdiaye-yr7zo 7 дней назад +1

    billahi baye fall yi linioy deff do yoon t yalla santanè woko

  • @bazilba1215
    @bazilba1215 6 дней назад

    Sénégal mo neix rek l'état dois prendre ces responsabilités kilifeu diné yi yam séni places

  • @bambaafiaofficial4321
    @bambaafiaofficial4321 7 дней назад +3

    Touba kay lafa doyna war Mane dama warou sakh li mome dou deuk may lene nite diamou way té lou doy war dinafa xew 💔💔💔😢

  • @KaneCheikh-dt7zu
    @KaneCheikh-dt7zu 7 дней назад +1

    Magui wat thi yalla né s khadime imam gni yalén geune sa wa keur nio léne geune

  • @saloumsall4930
    @saloumsall4930 2 дня назад

    Merci beaucoup imame

  • @dioufmamediarra1656
    @dioufmamediarra1656 7 дней назад +2

    Niome dé liniouye défe doyna ware diaguo khamo yarouyo beugeu yaraté li niouye défe srg touba santouléneco srg bi déye ikhdinase siratalmoustakhime la fi bayi kifi togui tame mome la diguelé mannak li khéw ci yone wi la khamoule loumou done wa salam

  • @albachirdiop2615
    @albachirdiop2615 7 дней назад +1

    Baye Fall yi dougnou exemples bay régler ay nit. Civile dou régler moroom Civile nagnou bay thiaaxaan yi ta nek ay nit. Ñom baye fall fethie ak yalwaan rek lañu fi nekke j'appuie wuñu jaulli wuñu. Kuleen ko sant tamit te guko ci yoon ana police ana gendarmerie ñom ño am droit exercer la force légale.

  • @Dgcfh123
    @Dgcfh123 7 дней назад +4

    Wa touba nio ngi danger ⛔️ 😂😂😂😂😂😂😂bakh na rekc

  • @assanemar5077
    @assanemar5077 7 дней назад +3

    Li serigne bi beugue touba moy am inchalla diadieuf baye fall yi yéna néck si deugue

  • @ziiboy5149
    @ziiboy5149 7 дней назад

    😢😢😢

  • @papendiaye4692
    @papendiaye4692 7 дней назад +2

    Touba deukou jamboree la

  • @MbackeFallou-c2e
    @MbackeFallou-c2e 7 дней назад

    ❤❤😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @stevebikoconsciencenoire8771
    @stevebikoconsciencenoire8771 6 дней назад

    L'état doit prendre ses responsabilités à Touba, ces comportements n'ont pas lieu d'être dans un état de droit.

  • @diopdiop7519
    @diopdiop7519 7 дней назад +1

    Souk rame diokhé adiya ñiou difli thi saye lokho nga diw sa kaname-nga sol lou islam térévoul ñiou diape la nga fâye-ndokh mou nékh ñiou diaye lako-nga déh fâye niou sag la-yobou armél ya soûl la nga fâye -yako manal adouna-alakhira y'allah vakh nako thi sourate 80 verset 37.

  • @bambaafiaofficial4321
    @bambaafiaofficial4321 7 дней назад

    Ay domram la niou rek

  • @PapeGueye-r2t
    @PapeGueye-r2t 7 дней назад

    Khana dou Senegal