Pokola Baldé sans réserve : "Balla Gaye 2 meunouma perturber, Boy Niang moma wakh..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 136

  • @boubacarlimanbadiane8668
    @boubacarlimanbadiane8668 Год назад +11

    Ndam rekkk inshallah❤❤❤❤❤

  • @Patriotepourtoujours
    @Patriotepourtoujours Год назад +6

    Pakola yalla nala yalla defal ndam inchalla ex fans balla bi moy lay nianal

  • @momobouthiapathiolybi7752
    @momobouthiapathiolybi7752 Год назад +17

    Yalla nala yalla may ndam si barki yonenti bi amine 🙏❤️

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Год назад +14

    Poko kii boko Dané boufii
    Dieulath béneu Boy Dieuleull
    Grand yii Nanla May chance Yalène
    Meune foufff sax poko Ndobine bi🖤

  • @mamadoufall9185
    @mamadoufall9185 Год назад +6

    Pokola kessé ❤ YALLA nga Dane Gakou 2 ndam lou lèrr nagneu 🙏

  • @tontoudoufrokh3867
    @tontoudoufrokh3867 Год назад +6

    Borom cité Gadaye Gakou ❤

  • @khadimfall7760
    @khadimfall7760 Год назад +5

    Li takh ma beugeu la moye da ngua deuke pikine de ragualo lolou

  • @SoldarouBamba__4
    @SoldarouBamba__4 Год назад +5

    Franc vs moussa ndoye
    Quench vs Gora sock
    Tapha mbeur vs mor kang kang

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Год назад +3

    FRANC VS MOUSSA NDOYE

  • @diop3575
    @diop3575 Год назад +5

    Wa keur falay yi ama ak jacop rk lafay supportait ms ki wakhou masi mom dara yallah kham nako mane dama yakar ni skh da weroul ms bkh na ba gackou diapoula nga kham lepp deug leu del wakh rk yallah bakh na gackou 2 yalle nala yallah May ndamm 🤲❤❤

  • @AblayeCamara-f5v
    @AblayeCamara-f5v Год назад

    Pokola seul Ama kassé Ama seul Ama yée day déranger 💪💪💪💪💪💪🥰🥰❤️❤️❤️

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Год назад +2

    MOUSSA NDOYE VS FRANC

  • @papadionmendy3557
    @papadionmendy3557 Год назад +4

    pokola baldé késsé yalla nala yalla taxawou soutoural té mayla ndam si barké seydina mouhamat psl amine 💯🙏🙏🙏🙏🙏🙏💪💪💪💪

  • @Elpheno344
    @Elpheno344 Год назад +5

    Boy bilahi gnak respecter balla Gaye 2 rek Mane nala dane sii combat 🎉

  • @mansourmbaye4682
    @mansourmbaye4682 Год назад +1

    Pokolaa champion deug gua mais evitel neik si réseau yi di tagg sa bopp liguéyal gua wagnii wah djii tot ou tard succès bii diguako guiss👌🏾

  • @ibrahimagadiaga7606
    @ibrahimagadiaga7606 Год назад +3

    Yalla n'a la gakou dane Dagua rew beuri wax

  • @oumarndoye1169
    @oumarndoye1169 Год назад +4

    Ki dafa dof balla gaye 2 dousa. Morom

  • @DiakhateAmsa
    @DiakhateAmsa Год назад +4

    Pokola balde rék laniouye toppou 💯 💯 💯 💯 💯 💯 ❤❤❤❤💚💚💚💚💚👀👀pikine rék ❤❤❤💚💚

  • @sirmandiallo4685
    @sirmandiallo4685 Год назад +2

    Pokola le future roi ichallah

  • @ahmadoudiop5016
    @ahmadoudiop5016 Год назад +12

    Gakou 2 ndam rek inchallah ki sen famille mossi gueuneu doffé

    • @diop3575
      @diop3575 Год назад +2

      😂billay domou baye wakh nga deug 😂

    • @mamadoufall9185
      @mamadoufall9185 Год назад +3

      Wakhoffi touss nguanane doffé😂

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 Год назад

      Bilahi ki dafa doff mé bouko Gakou 2 diapé mou khamni lépp deug leu Gakou yaw mome limalay wax moy boula boy bou Bari wax bi dané khamalni yaqkhouga mé yalla nalla yalla may ndam

    • @AntaDiagne-m3t
      @AntaDiagne-m3t Год назад

      @@cheikhdiop9673 Amine ❤

    • @ahmadoudiop5016
      @ahmadoudiop5016 Год назад

      ​@@diop3575😂😂

  • @Doffouamabalde
    @Doffouamabalde Год назад

    Bilahi lamb ji bousi mystique guéné Gakou mola meune aller retour sen wa keur yeup molén dakk beuré

  • @pathendiaye5964
    @pathendiaye5964 Год назад

    Bilahii Gakou diinaala nokkou

  • @pathendiaye5964
    @pathendiaye5964 Год назад

    Gakou yallaaah nla yallaaah maaay ndam

  • @diopkeba8068
    @diopkeba8068 Год назад +4

    Lamine sakh legui daa ponkall 😂

  • @MorThiam-e4e
    @MorThiam-e4e Год назад

    Pape diédhiou.je dit que,pokola est plus têtu que gakou2.Ama baldé,dit que pokola,va corrigé gakou2...

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Год назад +1

    BB AMA BOU YARAKH VS BÉCAYE BOU PARCELLE

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj Год назад +4

    Boy bi amoule respect

  • @assane720
    @assane720 Год назад +2

    pokale dérou pikine bi yalna ga am ndam

  • @domoudeukbi24
    @domoudeukbi24 Год назад +5

    Kate lene sene ndy yabi boy bi pokola kassé kou sissou sa bounou ndy😂

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Год назад +3

    Me lamine khana legui da ngay dem sall😅

  • @Fricastyle73
    @Fricastyle73 Год назад

    Poko seul 😊

  • @roots7.628
    @roots7.628 Год назад +1

    Poko rq momeuh yémeuh bilae❤

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Год назад +3

    Kii Falay Baldé moy Maamam
    Amaa Baldé moy Bayam Mounoull
    Ragall jamais c inposible 👎Pokolaa kasé Ndobine Bou Nioull Koukou bi 🖤Gayné pikine bii pokola❤️

  • @SaliouNdiaye-xz6bg
    @SaliouNdiaye-xz6bg Год назад +4

    Yaw dagua dof Mélanie Jacob amale yare thi sa diguanté AK balla guaye sa Tonton la kone gua torope

  • @BabacarCiss-ki4ri
    @BabacarCiss-ki4ri Год назад +3

    Pikine moy déranger Pokala kassè💪🏽

  • @boubacarabidinaaidara4408
    @boubacarabidinaaidara4408 Год назад

    No DEFF danou barke seydina Mohammed psl

  • @omardiallo5742
    @omardiallo5742 Год назад +3

    Pokola lamine seck sakh mola geuneu takhaw

  • @babacaargueye5862
    @babacaargueye5862 Год назад

    boy amal yar

  • @alassanesow7924
    @alassanesow7924 Год назад +1

    Ay nitou Balla gaye rek guay sante après sa combat

  • @thiaomame1357
    @thiaomame1357 Год назад

    ya mon

  • @alassanesow7924
    @alassanesow7924 Год назад +6

    Yaw balla gaye 2 ak ama sou yakho sa lokho dousi diouguè 😢

  • @mouhamedsambe7820
    @mouhamedsambe7820 Год назад

    Mom xana Ama mounoul wax ak mom mou xamna balla ak mom respect reik mofa war keur falay ak double less famille la pokola nank reik

  • @mamadoundiaye5230
    @mamadoundiaye5230 Год назад +2

    Way bayilen ndiambour ki boy pikine la wakhnako balla dou noname mais faralouko amna si plein droit.
    Yalla gua ham ndam pokola

  • @arlindouarlindou7588
    @arlindouarlindou7588 Год назад +2

    Gackou 2 kesse domou deuk bi

  • @biglinzongodiba620
    @biglinzongodiba620 Год назад +1

    ki rewoul da loco dof degue mais sama comantriar bi bayi len si khel ki bou dane si combat bi hoohe len ma asstou wala ndaye fatou bayi si khell

  • @papandiaye1823
    @papandiaye1823 Год назад

    Boy yow sa wakh beuri torope mais khamal ni amgua biss deh fait très attention kiguaye beurel dou niekhou niebee deh

  • @ndiakhate29-isaac
    @ndiakhate29-isaac Год назад +1

    120kgs noko meune pese.c est imposible way.😢

  • @khalifadem7517
    @khalifadem7517 Год назад +1

    Pokola késé

  • @alinediop1940
    @alinediop1940 Год назад +1

    Diam rk pokola

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Год назад +3

    GACKOU MOLA MEUNE FOUF

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Год назад

    Pokala amnga problème de gackou deux ndaandane la

  • @MbayeAbabacar-ug5if
    @MbayeAbabacar-ug5if Год назад +1

    Ama balde sa boy bingua beug Sacrifice contre modou lo gayi kham nagne ko bayil boy bi lala wakh

  • @mormbaye6098
    @mormbaye6098 Год назад +1

    Ndam rék inchala

  • @PapaNdiaye-b1s
    @PapaNdiaye-b1s Год назад

    pakola dou khamgua bb Gouy gui😂

  • @babacaargueye5862
    @babacaargueye5862 Год назад

    keur falay magui fay sogua diepi mbeur

  • @babaseye5530
    @babaseye5530 Год назад

    Pokola day nelaw paté pa la doley xaley t niouko gueun paré niofi nek amal thieur

  • @DjibiThiaw-wy2xy
    @DjibiThiaw-wy2xy Год назад +5

    Pokola dou rouss ama balde gua bayi balla gaye nn😢

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 Год назад +3

      Pourtant mosoul wakh balla louniaw

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 Год назад +2

      Ki day lamb rék

    • @ahmadoudiop5016
      @ahmadoudiop5016 Год назад

      ​@@ibrahimadrame9499Mane tamite yaguenako sétlou wayé meussul wakh si balla lou nice

    • @mamadoufall9185
      @mamadoufall9185 Год назад +3

      Saway ki wakhoul Balla gaye 2 Dara dafay diay combat bi lo beugg mou wakh

    • @DjibiThiaw-wy2xy
      @DjibiThiaw-wy2xy Год назад

      Nn frère dou dara mais xamgua rk xamna do comprendre mou bagne ko toudou sakh mo geun

  • @sidathmalangdiedhiou3523
    @sidathmalangdiedhiou3523 Год назад

    Dafa beury wakh trop

  • @moustaphasarr6637
    @moustaphasarr6637 Год назад

    Pokola bay fall dou sokha 13:26

  • @cheikhdiop9673
    @cheikhdiop9673 Год назад +4

    Boy bi dafa Bari wax ahh wax dioubari dou yeufou gorr Balla gaye sa papa la dousa morom yaw ak Al Boury Moy combat bayilén moytou bi

  • @amadyndiaye4367
    @amadyndiaye4367 Год назад

    Pokola Dagua fek Famille Falaye Baldé Ak Famille Double Less nek lou yague lossiy wakh déko bayi khel Ndakh Balla Gaye 2 loumou sikeu sikeu Respecté na Famille Falaye Respectel Balla Respecté sa Adversaire wagni wakhi Doff

  • @PAomartoure2002
    @PAomartoure2002 Год назад

    Boula lerreni gakou dinala dane rek mouy sa diam

  • @BabacarCiss-ki4ri
    @BabacarCiss-ki4ri Год назад +1

    Fittt bi neckeu si domou pikine ack sagn sagn bi meuno léne ko sipp sakh

  • @cheikhfaliloundiaye7782
    @cheikhfaliloundiaye7782 Год назад +1

    Pokola , gackou 2 dafa tell si yaw , meune gua am ndam ndakh yalla koy mayei mais boudé beuré rk ak xel bou dal si guew gackou mola meune si niati coté yoyu yeup

  • @cissecisse5622
    @cissecisse5622 Год назад +1

    Dafafibal

  • @sellediop1817
    @sellediop1817 Год назад +2

    Yawe defale li balla def si lamb dh bayi wakhe dji waye yagui beugue sof nak

  • @abouba3509
    @abouba3509 Год назад +3

    Gakou mola meune allez retour

  • @ibrahimasene9243
    @ibrahimasene9243 Год назад +2

    Yallana nga daane djeule bou reuye

  • @AmetThioune
    @AmetThioune Год назад

    Gakou mo man d😂

  • @mamadoubousso-bz8qc
    @mamadoubousso-bz8qc Год назад

    Ki weroul

  • @malickly409
    @malickly409 Год назад

    Vous qui disent boy bi beurina wax wax mo takh vous commenté sou waxoul dolen commenté poko seul fermer vos bouche

  • @deneden6723
    @deneden6723 Год назад

    Mom il perd sont temps di toudou balla té balla douko toud… ki dofla rk

  • @maxsarr5879
    @maxsarr5879 Год назад

    Balla waxal t geunekasy

  • @ibrahimasougou7061
    @ibrahimasougou7061 Год назад

    Ki bou yabo wa famille wame naniou KO moytou boy bi seuytané la

  • @cissecisse5622
    @cissecisse5622 Год назад

    DIFIRLINSINMIKREJE

  • @moustaphasarr6637
    @moustaphasarr6637 Год назад

    Pokola bay fall dou sokha

  • @taphalo
    @taphalo Год назад +1

    Ki dou défe carnyére dafa réw ba dofe keur falay mosi geune dofe boo bayiwou sagara doo dème

  • @KarrambaBarrow
    @KarrambaBarrow Год назад +1

    Kou faralull poko mbam rek sa diobou EHHHHHH fuck

  • @Aboudex2
    @Aboudex2 Год назад

    Sen commentaire yi négative yi bayi lén ko ki drapeau Pikine rk kassé lay yeukati dou mare boune Diambare la Pikine rk lay topou

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 Год назад

    Lamine dél tey touti té bayi reuy

  • @maxsarr5879
    @maxsarr5879 Год назад

    Balla gorlà

  • @GabrielLouis-fk7tv
    @GabrielLouis-fk7tv Год назад

    Pakala tu va perdre se combat

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj Год назад

    Boye dagaye. Damou

  • @OumarDiallo-x2c
    @OumarDiallo-x2c Год назад

    Stop sene combi cangele

  • @ndiagandiaye2033
    @ndiagandiaye2033 Год назад

    Pikine loutax niou meunn fenn

  • @ibrahimafall-sb9qt
    @ibrahimafall-sb9qt Год назад

    Ama sakh kham Nani danga rew motax Cambie Mounia boule dougou sale bi

    • @Pokolatv
      @Pokolatv Год назад

      Bayil fénn niéménga yalla trop ya dég Ama wakh ki

  • @moustaphadia2635
    @moustaphadia2635 Год назад

    Boy Balla Gaye 2 doussa moromam con nga reiik vrai doff. Yaw ak Balla Gaye 2 famille la

  • @mouhdy852
    @mouhdy852 Год назад

    Yawe danga réw