Franchement, il faut mou danou, pour nga dogga xam né il a atteint ces limites. Incroyable ceci n'est pas professionnel. Courage jeune homme 👍🏿... Tu as tout donné.
Da wara am temps de récupération si intervalle séance bounè pour non seulement pour def dièkhital si yaramam ak formam sinon sou claquè bala mouy wèreu dey yague ndakh muscles yi nioy saturè.... Falaye Baldè Belgique
Babayo moy sama Tourandor,sama nidiayou Yaye la,sama Papa mo dougueul sama domou Tourandor ecole,sama Mame Daba modane topato lèpeu lou warone souniou nguintè ak yeurè you sama Yaye dane sole.Mama lamey wowè mom sama Mame Daba.teksi sama Tourandor bamou fèbarè maco done yobou hôpital ladj lène Jules douco wèdi ndakh nioune niète nio dane andeu
@@fafabalde795 ndeye sane deug la fall diam si yew liga wah ni si entrement pokola damakoy deugal motah sen combat yi sou dessé ay semaine boy yi dagniouy febar ba diel perfusion Jacob dalnako contre papa boy djiné ak pokola combat bi passé
Des fois nga guis kouy dadie lou méti si entraînement ta diouly niary raka diaféko lol😭😭😭😭😭😭😭 Sama genre gui rék lay wakhal yalla naniou yalla dieguel rek
@@djibrilsall9305 kii bamouy populaire sonko Dafa populaire boulma waxloo way🥹Amaa Baldé Depuis mapate waxou mala arène Dei nila Mousa méll ak mbolo niouko ndioune ndioko topou mapate ba arène xam nạn lolou Amaa Téla populaire Motax 3 combat La Berai Rék Bécay Mbaye waxny kii Dou Mbeurou avant grand combat Nankoy Teugeull grand combat c pasq nioukoy Topou Dafa beury c tài en 2010 la nieukeu Berai grand combat Bobou kéeu dafa xam sonko🧏
C est bien comme enchaînement mais sur chaque serie il droit avoir 30s de récupération en plus il droi boire de l eau puisque si tu perds 1% d eau tu perd 20%de force
Ça c le crossfit coach codè ce circuit il est permis aux athlètes de haut niveau ou ce à un athlète qui a de l assuiditè ou quelqu un qui entraîne tous les jours parce que ce circuit c est du volume et intensité si le corps n est pas habitué à cet entraînement dafay toy legui ou il se blesse
Sé très bien le circuit training de le savoire mé le temp est la récupération sé très normal 2 ou 3minute minute anciennement avec 4 série différentes la récupération sé une minute on doit aussi le faire une ou deux fois par semaine épuis sé très risques une bonne hygiène de vie d'une manière générale il faut aussi savoire l'état de ta santé avent de le faire sinon sé risques des parol de l'international de lutte olympique du Sénégal serigne mbacké dit pithie ramatou
Entraînement serie leu coach bi dess na done professionnel daffa wara ame temps de récupération pour muscle yi deff seconde tranche bi sinon muscle yi day bloqué té lolou day yaak forme di indi febar té do développer 🙏🙏🙏
Ana wa keur seydina mouhamed les coeur ❤❤❤
Mome rek lay topou
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤psl
Salalahou aleyhi wa salam
Diamaguene là deuk mais j'aime beaucoup pokola diam ci iow
Merci bro
Franchement, il faut mou danou, pour nga dogga xam né il a atteint ces limites. Incroyable ceci n'est pas professionnel. Courage jeune homme 👍🏿... Tu as tout donné.
C’est du vrai travail ça fait du bien pour le cardio
Effectivement
Effectivement
Ki dafa beugeu ray pokola mais no nou la li nga ligey rk mom ngay feyékou ❤❤❤❤
Vraiment khamoul dara Europe la nekk mais ni mouy deff bakhoul ci poko
Le travail Paie Motakh Tay Danneuh Talfa Ak ay moromam yeup❤️Jambar Deug POKOLA
Bilay
Da wara am temps de récupération si intervalle séance bounè pour non seulement pour def dièkhital si yaramam ak formam sinon sou claquè bala mouy wèreu dey yague ndakh muscles yi nioy saturè.... Falaye Baldè Belgique
😂😂😂😂 merci falay bou Belgique
Je suis coach sportif et cela est mon domaine.Je vous en prie Monsieur Cissé !
@@fafabalde795 ça ce voi liga wah yeup deugeu la temp de récupération dafa bah si entrement
Babayo moy sama Tourandor,sama nidiayou Yaye la,sama Papa mo dougueul sama domou Tourandor ecole,sama Mame Daba modane topato lèpeu lou warone souniou nguintè ak yeurè you sama Yaye dane sole.Mama lamey wowè mom sama Mame Daba.teksi sama Tourandor bamou fèbarè maco done yobou hôpital ladj lène Jules douco wèdi ndakh nioune niète nio dane andeu
@@fafabalde795 ndeye sane deug la fall diam si yew liga wah ni si entrement pokola damakoy deugal motah sen combat yi sou dessé ay semaine boy yi dagniouy febar ba diel perfusion Jacob dalnako contre papa boy djiné ak pokola combat bi passé
Pakola champion pikine❤💚❤💚❤💚❤💚💯 yi touss
Après chaque exercice il faut un temps de récupération, sinon ça risque de déchirer le muscle.
C’est une séance de cardio bo récupérer perte sa rythme deh bien joué coach
T’as compris
Bou lènn raye boy bii wayyy. Sama champion Pokola Baldé rékk wala dara toussss nakk.
Ama baldé rek lanouy toppou🎉🎉🎉
Qui daffa beugeu réy sougnou m'bam bii wayé,digua kham nii rey m'bame youmboule dhé iow mii digue s'y sonne bly😂.
Pokola seul ❣️❤️❤️❤️🙏
Des fois nga guis kouy dadie lou méti si entraînement ta diouly niary raka diaféko lol😭😭😭😭😭😭😭
Sama genre gui rék lay wakhal yalla naniou yalla dieguel rek
😂😂
Bilay ya wakh degue 😂😂🎉😂😂
Bilay degeula yalla nanosy yalla mothial 😢
Non coach c'est un être humain non une machine 😢 la récupération est important
Sisi maiil fau k mou diekhal séquence bi tmt avant mouy nopalou
Sa khôl bi daff thiy moudié diékh sakh wallahi
Louwar gua copin wadji dafa beugua raye ki
C’est important mais liii cardio leu
Cardio leu
Billakhi coach bi dei entraîneur rou CrossFit la 😅😅😅. Limotax kay écuries falay vite fait bien fait 😂😂
Bilay
Li serie foncionall la li yeup mo nekk ben seri apres la recuperacion bi nieuw le coach travaill bien
Walah t’as compris
Non sek double séance dafa wara def 45seg de récupération si no day étude
Pakola le champion
Bilahi Man dama begue ama ❤
Un coach Professionnel que je connais bien
Un vrai coach
Good well train, bless all of you Amen 🙏👍🙏🌍
🙏🏾
Li mootkhe souwaye dawe❤❤❤❤❤❤
😂
Merci coach pour le circuit training ❤
Ki monta dan moduo lo
De rien
Liguéye rek fayékou ❤️💚
Du courage mbeur ça ira Dina bakh
Merci
li c’est un séance de cardio c’est normal et il a bien fait
Walah ta kompri
Nék léne ay nitt chaque séance dafa wara am temps de récupération, sinon dafay claquer dh Waa bakhna
Courage Champion ✌🏾
Athia pokola Baldé seutou Falay Baldé bi fls de Ama Baldé ❤fls Fofou la rék liguey rék yaa Meune Yaa eupou Doolé fls ✅Gayné nga champion nga ✌️
Ama ye ❤❤
Ama Baldé kii Barké serigne bamba Mbacké mayou Yallah sounou Borome la ame kii 🤭🤭🤭migui Mélnii kou Togoul 5 ans beraii woul loumasi Diaxall Ama Baldé Tayla geuneu ame beuzz thi Lamb Dji 🤭
😂 sa lamign bou reuy bi naga fehei bouko modou danei ga gneuwate wax
Lolou yep khol bou rafét té sét rék mokoy mayé
Sonko rék mo waral lolou
@@djibrilsall9305 kii bamouy populaire sonko Dafa populaire boulma waxloo way🥹Amaa Baldé Depuis mapate waxou mala arène Dei nila Mousa méll ak mbolo niouko ndioune ndioko topou mapate ba arène xam nạn lolou Amaa Téla populaire Motax 3 combat La Berai Rék Bécay Mbaye waxny kii Dou Mbeurou avant grand combat Nankoy Teugeull grand combat c pasq nioukoy Topou Dafa beury c tài en 2010 la nieukeu Berai grand combat Bobou kéeu dafa xam sonko🧏
Entremen day am recuperation li motakh boy boussi févre dee
😂😂
Mais lii séance de cardio leu
Waw ms jo récupération book
Cardio leu
Ama sa ndèl bou reuye bi yalla nala yalla dèfal ndame unechalah 😅😅
Pour mou dane kane 😂😂😂
❤❤❤ diambar sa warba 🎉
Wadji nena worna yallah meuneu touma😊😅😅
Entraîneur bi amoul Expérience Entraînement dafay am Récupération way del may Pokola mouy nopalou li dafkoy gagn rek
Mais bro liii séance de cardio leu
Trop de coach dans les commentaires, mais lii séance de cardio leu c’est normal
Yalna la yalla def roi 🤴 des arène ❤😅
Amine
Pokola kassé❤
Sa waye da toye dagaye deeee😅😅😅😅😅😅 migui sakhate rekk
Cii la bokk
Borome ndiakhasssss biii 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂trock iao sofffff nguaaaa😂😂😂😂😂😂😂
😂
Le temps de récupération est très intéressant pour les circuits
C’est ça me disait
Mais en cardio on enchaîne
Mais c’est une séance de cardio
Vraiment
Di na ko reye deh 😂😂😂
È un circuito ,deve fare tutto in una volta , dopo può riposarsi anch’io lo faccio ma nn così però 😢❤
Décourager mbre 👏
Balla Gaye 2 moy sama mbeur mais bilahi ma beug ama baldé❤❤❤temps yi Sathiés ak lac 2 la mounatoul supporter 😂😂😂
وما خلقت الجن والإنس إلا ليعبدون
Sénégal ngay Guiss kou khamoul dara si entraînement di critiquer li coach bi di deff lou bakh la c’est de l’endurance musculaire
Bilay gayii khamoun dara di wakh rek kardio bou bakh faw mou mettiii
Sérieux mon ami trop facile de se ranger derrière ton clavier et de critiquer
Right
Mome rk lay topou champion ❤
Pokola mi li mouy def bakhoul de ki mougi beuge dé me wadji khamoul dara
Mais bro li c’est normal
Impossible n'est pas possible
Hum Coumba Baldé rek 😂😂
Athia mbeur wawaw poko mbame ...mais pape sarr gayi dagniy Ray sa boye bi dé
😂😂
Ndeysane mbeur sonouna nk
J'aimerais bien voir le coach à la place de pokola !!!
Yorr montre bi yombeu n'a dh !!!
😂
Wkh degue yalla. Ama sama mbeur la ms gakou 2 dalaye d'âne mola daka beuri kokou Li danou ko am nga comba dh bou wede ladiale bb diene 😊
Courage champion turfu roi borom bayern
C est bien comme enchaînement mais sur chaque serie il droit avoir 30s de récupération en plus il droi boire de l eau puisque si tu perds 1% d eau tu perd 20%de force
Ama yyyy
So continue nii ligue nga deé💀
Noumouy entrainé nonou lay beuré😅
Bilay
Gor Yalla ga
Saway kay lii motakh mouy nieuw di nélaw en plein signature contrat
Pikine rk✌️
Circuit dafa bakh pour cardio✌🏾
Merci
Ça c le crossfit coach codè ce circuit il est permis aux athlètes de haut niveau ou ce à un athlète qui a de l assuiditè ou quelqu un qui entraîne tous les jours parce que ce circuit c est du volume et intensité si le corps n est pas habitué à cet entraînement dafay toy legui ou il se blesse
Ms guisse nguéna Ama noumou tolone
😂z😂😂😂😂❤❤
Sé très bien le circuit training de le savoire mé le temp est la récupération sé très normal 2 ou 3minute minute anciennement avec 4 série différentes la récupération sé une minute on doit aussi le faire une ou deux fois par semaine épuis sé très risques une bonne hygiène de vie d'une manière générale il faut aussi savoire l'état de ta santé avent de le faire sinon sé risques des parol de l'international de lutte olympique du Sénégal serigne mbacké dit pithie ramatou
Okay
Limouy def motah lambam Ben action boumou commencer mou am continuité
Limotah pokala nangoul wor kay 😂😂
Baadou 😂🤣
Dou worr.? Ki mo deugueur fite te niak diom way
@@boy_galsen12 😁😁😁nena bay fall la
😂😂
Affairam la. Nioune déh gni gui wor
Entraînement serie leu coach bi dess na done professionnel daffa wara ame temps de récupération pour muscle yi deff seconde tranche bi sinon muscle yi day bloqué té lolou day yaak forme di indi febar té do développer 🙏🙏🙏
Li seance de cardio leu
Bonne chance
Coach bii khamna Aprés sou liré commentaire yii dina bayi champion bi temps de récupération 😂😂😂😂
😂😂
Mdr
Bayil mbotou yi nak😊😊
Pokola moy mbam dei 😂
😂😂 lambeu mettina
😂😂
😂😂
Forme pacola légui lah guene 😂😂
C’est bien ça
Entraîneur bi deh damélni si Pokola lay diangué entrainé nit😂😂😂
Chak sciences pokola dafa wara récupérer 30second sakh😂😂
Gnoune gnoungui treuene dh🔋💪🏾 gnom gno treunoul 🧏♂️🧏♂️😂😂😂
😂😂
Entraînement bou amoul récupéré 😂
Trop de coach dans les commentaires 😂
Yaw li cardio leuh di 😂😂enchaînement rek
Au moins 30seconde pour récupérer après chaque série
Pokola 1:20
Dieuleul baye fall bi borom ndiakhass😂😂😂
😂😂
Billah dé comme mou nexxx
Dina dé dii😂😂😂😂😂😂
😂😂
Le temps de récupération c très important mais vraiment les entraînements c bien bo topé ci TANK ama rek mou bakh
Inchala frère
Allez futur champion
Entraineur bi khamoul dara
Esk dou iow yaa khamoul dara
Barki yalla meunou touma demm 😂❤❤❤❤❤😊
Bilahie dér nga
Bilay
Mais il a 10 seconde pour repose chaque série
No 😂 coauch day saxorr😂😂😂
C’est un vainqueur
😂
Wa yene boulene rayy sma dieukeur djii😢
Le temps de récupération coach c obligatoire
Pokola yalla na la may ndam bou sed
Aminn
Kii amoul mobilité dh
Où est la Team Tiktok 2024? Pokolaaaa, pokolaaaaa 😹😹😹
POKOLA gainde DEUG la
Kii dou mbeurr 😂😂
legui pourquoi amoul récupération
C’est une séance de cardio