BALLA GAYE DECORTIQUE SON COMBAT AVEC BOY NIANG

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025
  • Bantamba tv. Km 2,5 Boulevard du Centenaire de la Commune de Dakar.
    tel : 33 825 34 36 - 77419 03 64
  • СпортСпорт

Комментарии • 445

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 Год назад +15

    Balla gaye 2 rék lanie topou bilaye 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @mamysy3291
    @mamysy3291 Год назад +15

    Toujours le King,Walaxi Daane leu Yombul 💪🦁❤️🥰🫶

  • @modoufaye9286
    @modoufaye9286 Год назад +24

    Balla gaye magoum yallam dieum nga mola takha dougou si lamb nga ne fi nga dan dem ak sa papa gnané khamato fofou balla dafa mel ni danga worr nit mom lou say wadiour don deff sou ka fi yalla dieulé pour man warr nga ko meuneu motali gorr deugeu lolou lay deff yegale sa yene wadjour ❤❤

  • @Kako-ho9jx
    @Kako-ho9jx Год назад +10

    Tu es le meilleur te yaw laniouye top

  • @mansourdiop497
    @mansourdiop497 Год назад +4

    Balla Gaye 2 toujours meilleur de sa génération tu resteras toujours mon lutteur et ton petit frère Sathies bonne change pour le reste de ton carrière

  • @assanediaw2218
    @assanediaw2218 Год назад +38

    Je n'ai jamais été un supporter de Balla gaye 2 mais c'est le plus grand champion de l'arène sénégalaise

    • @assanediaw2218
      @assanediaw2218 Год назад +5

      Derrière yékini bien sûr c'est yékini le plus grand champion

  • @khalifaababacarfaye8354
    @khalifaababacarfaye8354 Год назад +8

    félicitations Balla gaye 2 guisna si yaw maturité ak expérience

  • @mamadouseck4666
    @mamadouseck4666 Год назад +20

    Alhamdoulilah yallah bah na..svp adouna dou keur diamouléne yallah bayi thiahane

    • @beugs9192
      @beugs9192 Год назад +1

      Bayil sétane aÿ thiakhane

  • @massendiaye5802
    @massendiaye5802 Год назад +24

    Balla magatoul dé dafa feuneukh limou tégone yaram bi moko gagne té moko top mom ak gouy gui dano ték lou eup sén yaram pourtant Eumeu molén mag mais migui gardé formam balégui en plus do guisse mou yokhou lou yakham atanoul bombardier pareil

  • @khadyndiaye-j7e
    @khadyndiaye-j7e Год назад +1

    Merci balla lamb na yam si cadre lamb, sou amone tournoi des vip si laniouye kham louye titre roi.

  • @tallagningue9456
    @tallagningue9456 Год назад +3

    Balla gaye 2 tu est le meilleur je te souhaite le meilleur

  • @reemoreemo5008
    @reemoreemo5008 Год назад +12

    Wakhléne boy Niang 2 mo meuna beuré trop sakh lolou moy wakh djii

  • @moussandoyeseck8430
    @moussandoyeseck8430 Год назад +3

    Balla gaye nitt kou bakh la masha'allah

  • @bayesambadioum9637
    @bayesambadioum9637 Год назад +7

    Fadam Bilahi Walahi c’est le meilleur ❤

  • @adamadiallo1321
    @adamadiallo1321 Год назад +2

    J sui fan d boy niang... mai balla loumou def ci lamb yomboul. Boy niang ndanane la bilahii

  • @khadimkane7608
    @khadimkane7608 Год назад +6

    Balla kassé ak lou mana am yaw rk laniouy top ❤❤❤

  • @BBC7789
    @BBC7789 Год назад +2

    Balla tu représentes la lutte ici au Sénégal ❤

  • @cheikhatdiop3646
    @cheikhatdiop3646 Год назад +22

    Balla mayyy naaala kharou tabaski ligua wakh sisama champion bi le roi des arènes
    Modou Lo 🫶

  • @saloumisland2823
    @saloumisland2823 Год назад +10

    Balla niiigua donne diap ak sene tank ak boy niang sont different

    • @boy_galsen12
      @boy_galsen12 Год назад

      Ban combat la balla gaye diap tank apart boy niang ?

    • @mamadou717
      @mamadou717 Год назад +5

      ​@@boy_galsen12contact la wakh

  • @SambaMbaye-pi5in
    @SambaMbaye-pi5in Год назад +3

    Balla nimala beugéwon mé légui vraiment safatoma dara amo koloré

  • @maleyeboye973
    @maleyeboye973 Год назад +22

    Le meilleur lutteur de sa génération. IL l'a dit 🎉never give BG2❤

  • @deug5710
    @deug5710 Год назад +6

    Balla mane meussou Mala farale, wayé kou bakh nga. ❤❤❤

  • @amsbi100poumonsofficiel5
    @amsbi100poumonsofficiel5 Год назад +15

    Vraiment sportif gua borom bax gua. Yallah nala yallah défal ndam sa prochain combat Inchalah ❤

  • @africansworldtv3381
    @africansworldtv3381 Год назад +3

    Tu es le meilleur lutteur de l'histoire de L'arène sénégalaise de tout les temps. Kou waxal loolu dangay féne

  • @Lesdelicesde
    @Lesdelicesde Год назад +4

    Boy Niang bou ragual deh, champion la

    • @sheky3138
      @sheky3138 Год назад +1

      DOU ATTAQUER MOUKK XAAR REK! MOTAX MOU SOOFE MA QUOI!

  • @mansourndione1342
    @mansourndione1342 Год назад +1

    Silence khamo gat bn2🔕👌👌😘

  • @mouhamedndong6069
    @mouhamedndong6069 Год назад +2

    Bilahi Boy Niang 2 Mola Meune Foufff Té Yagg nalako wakh Famille Sakho Dougn Daan Boy Niang 2 Depuis 2012

  • @moustaphafadiga774
    @moustaphafadiga774 Год назад +2

    Fadam mo begeu ay wahou mystique ah Fadam soff ngua

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 Год назад +7

    Ay nafékh guéne boye niang daf ko meune eupeu ko dòlé danèlko balla gaye gñimoudone danèl gñiogñou balla daf lène diampone si galadj boye niang khaléla

  • @modoufaye9286
    @modoufaye9286 Год назад +12

    Mystique bi mo yakhou rk lolou mo fi nek mais dakho beuré gayui mystique mom dinala gougé mais dafa am foumouy yam dh Lou ler😅😅😅😅😅😅

  • @mamembayesyllla2412
    @mamembayesyllla2412 Год назад +1

    Balla gaye 2 à vie ❤

  • @munirdaffe
    @munirdaffe Год назад +3

    Le meilleur lutteur du monde ❤❤❤❤❤❤

  • @djibery1023
    @djibery1023 Год назад +3

    Machallah balla nimou décortiqué combat Modou lo AK eumeu ça montre ni dafa xam beurè ak meune ko

  • @Papasamb-g8c
    @Papasamb-g8c Год назад

    Lamb dji mystique laa rk boy niang da guenna paaré balla gaye si lamb dji

  • @papesarr8751
    @papesarr8751 Год назад +20

    ❤❤❤❤ balla gaye 2 rek inchalla ❤❤❤❤❤

  • @ibrafall199
    @ibrafall199 Год назад +2

    Balla bonne chance a toi bro de la part de tes supporters from Gorée island in sha allah

  • @gangsta-p5n
    @gangsta-p5n 27 дней назад

    Fadam demal falleh kula baiye nga nyawal victory boy niang bi.

  • @abdoulayeguisse1863
    @abdoulayeguisse1863 Год назад +3

    Balla c le meilleur de sa génération ❤

  • @fatoumbye-pj1cb
    @fatoumbye-pj1cb Год назад +2

    Boy niang mola dakh beure sa thies mtx ma geum ni mola meun ndax sa thies mingi entraine chaque Jour

  • @Robbe-Grillet
    @Robbe-Grillet 8 месяцев назад

    Wallahi balla je suis fier de toi. Meusso danou si niak diom. Combat yi nga meussa ame défaite yeup danga andi diom ak foula ba yalla def limou def.

  • @AbdoulayeBa-nd1xu
    @AbdoulayeBa-nd1xu Год назад +8

    Aka mako beug ❤️

  • @Magistraaa607
    @Magistraaa607 Год назад +3

    Sawayyy dièkhal na taaakkk

  • @hj-eu6xc
    @hj-eu6xc Год назад +18

    Balla béléssiiirr borom blessure yi 😂
    boy niang dala dakh beuré eup leu dolé. Gorél rek té nangou.
    Bo dieulone eumeu sène kham né lep deugu leu. Da nga daw

    • @ChaybaMaiga
      @ChaybaMaiga Год назад

      fekhel ka am Lou balla am môgan si yaw niak fayda

    • @hj-eu6xc
      @hj-eu6xc Год назад +4

      @@ChaybaMaiga Boy niang mo sokhor té baakh si mak 🤣🤣balla béléssiiirrr ana sapeurs pompiers yila dieulsi woone si guèèw bi ?🤣Boy niang yay sauwassssss🤣🤣

    • @papediouf4607
      @papediouf4607 Год назад +2

      ​​@@hj-eu6xciom bouniou amoul arguments rek nan la feikhel am li balla am melni iow dengay takhawalou tè khamounioula niak class...Boy bi deko niouss daan fowéko😅

    • @hj-eu6xc
      @hj-eu6xc Год назад +1

      @@kefgg C'est vrai. Balla 37ans en 2023 --- Boy Niang 34ans --- Sathiès 35ans --- Eumeu sène 44ans. Mo takh dopage tricherie baakhoul day yakheu yaram. Balla comme kou am 50 ans. Bou beuréwone juillet ak eumeu sène di nguène guiss humiliation bou doywaar. Mo kham li takh mou daw

  • @boubacardiop-ue3kc
    @boubacardiop-ue3kc Год назад +4

    Balla gaye diam ci yaw inshallah 👍🏽

  • @ibrahimaleye4356
    @ibrahimaleye4356 Год назад +5

    Boy niang dala meune danela

  • @thiernoniang4910
    @thiernoniang4910 Год назад +3

    Thieuy Modou lo sama champion bi 💪💪💪

  • @baimamud1491
    @baimamud1491 Год назад +21

    Balla has a good heart ❤️

  • @MorLy-lp3pu
    @MorLy-lp3pu Год назад +5

    Sama champion 😍

  • @mouhamedndiaye6148
    @mouhamedndiaye6148 Год назад +1

    Nervis you bonne yui guéne done

  • @SkillWorld69
    @SkillWorld69 Год назад +4

    Non Sénégal beuri neu seytanei melni balla gaye waroul danou deggo nenalene yallah la 🤝🏾

    • @sirmandiallo4685
      @sirmandiallo4685 Год назад

      Sénégal mo nec balla boumouye dan yekini tout le monde avait peur de lui 😂

  • @tepppngom1733
    @tepppngom1733 Год назад +5

    Gni nga done dieul Sen tank douniou boy niang dh😂😊

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 Год назад +7

    Leufeul ndeye yi mbeur 🤣🇸🇳

  • @saloumisland2823
    @saloumisland2823 Год назад +12

    Vs oubliez tjrs que boy niang est meilleur que balla mil combat boy niang mo.meune

    • @fandiaye9301
      @fandiaye9301 Год назад

      D’agnat doul

    • @gastonpreira6870
      @gastonpreira6870 Год назад +4

      ​@@fandiaye9301😂loutakh bala bamou dieule tankay mounouko wone danee?

    • @ALNJR888
      @ALNJR888 Год назад

      No balla légui dafa yakou rek mais balla mou nieuk ma layyyy

    • @mamadoutoure1773
      @mamadoutoure1773 Год назад

      Doul na moss

    • @saloumisland2823
      @saloumisland2823 Год назад

      @@ALNJR888 balla bou dieuk na egal sathies te boy niang doko dane avc ma.maniere

  • @papama1975
    @papama1975 Год назад +1

    Guayndé guiiiiii 🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁❤️👈 yafi néck belégui 💪💪💪💪💪

  • @khadiataniang16
    @khadiataniang16 Год назад +1

    Balla késé yaw rek laniouye top

  • @mouhamedabdoulahidiagne786
    @mouhamedabdoulahidiagne786 Год назад +1

    Balla yay ndanan way machalla

  • @gorangom3537
    @gorangom3537 Год назад +1

    Balla def nga lep ms ki xallé la bou paré khm bopam

  • @PapeNdiaye-ht6is
    @PapeNdiaye-ht6is Год назад +2

    J'apprécie vraiment ton analyse balla tu a bien compris

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo4028 Год назад +8

    Balla do nitou d'ara hamo casamense
    Yow ak victoire c fini défaite rek

  • @user-bs2sy9mk4i
    @user-bs2sy9mk4i Год назад

    Très sincèrement kou guiss balla Gaye avant ak tayy khamni y’a une grande différence dou sama Mbeur deh mais très honnêtement boy niang balla dou boromamm

  • @issadia3253
    @issadia3253 Год назад

    il est un champion BALLA GAYE 2

  • @modougeuye3524
    @modougeuye3524 Год назад +8

    Balla rek ❤❤❤❤❤

  • @mbulasarr7185
    @mbulasarr7185 Год назад +3

    Amal diam BG2 love you forever

  • @sambadrame3497
    @sambadrame3497 Год назад +2

    Balla yalla bakh na blaye

  • @laminendiaye8516
    @laminendiaye8516 Год назад +8

    Fierté❤ de toi champion 🤲💯
    Combat👀 Modou & eumeu 👀noumou démé👍

    • @moussacisse1509
      @moussacisse1509 Год назад +1

      Eumeu sene da waroul wone dieul modou lo dako dane mou yor roi des arenes misstatement modou mo menone si beure bi eumeu da warone khaar

    • @moussacisse1509
      @moussacisse1509 Год назад +4

      Warouko wone dieul modou moko danone mou dieul roi des arenes dieul ko sans un autre victoire misriquement modou etait pret et eumeu etait presser alors qu il devait pas c est lui qui a la courone

    • @laminendiaye8516
      @laminendiaye8516 Год назад +2

      @@moussacisse1509 eumeu dafa wone ni Modou sa tankeu rék la sohela lo lou moko yakale

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 Год назад +1

      @@moussacisse1509 Lolou amna mais je blame l’encadrement d’ Eumeu. Il devait savoir qu’ Eumeu etait roi et il avait deja battu Balla qui venait just de battre Modou lo. Eumeu devait prendre Balla tout en Savant que meme s’ il perd, Sa revenge contre Modou lo serait toujours A l’ ordre du jour. Eumeu n’ etait pas pret psychologiquement et Mystiquement.

    • @moussacisse1509
      @moussacisse1509 Год назад

      Ils avais deja pris l argent avant le combat moi j avais vu en reve modou lo perdre le combat mais avais pris une autre advance le jour du combat balla gaye 2 modou lo j ai dit a mes amis d enfance que modou lo va batrre eumeu sene

  • @ismad5295
    @ismad5295 Год назад +17

    Digua yague danou inchallah

  • @Rapkabadaforever
    @Rapkabadaforever Год назад +2

    Merci beaucoup les gens mon champion il veut bien communiquer mais il arrive pas communiquer comme les autre lutter je lui aime bien wollah mais c'est ça lo problème sont ferré ca Thiès communique bien que lui 🎉❤

  • @zo47
    @zo47 Год назад +4

    Balla sama mbeure la mais wakhoul deugeu néna yénene combat youmou beurré béne yone lassi contact té dane

    • @mamadou717
      @mamadou717 Год назад

      Daga beug wakh day doull

  • @jacquesjuniorba7698
    @jacquesjuniorba7698 Год назад +1

    C’est le plus beau le plus grand le plus charismatique et le meilleur de l’histoire de la lutte sénégalaise Balla Gaye 2

  • @faye6718
    @faye6718 Год назад +7

    Du courage le grand champion

  • @BourouKaff
    @BourouKaff Год назад +6

    Physiquement et contacment😂😂😂😂

    • @niangmedoune7962
      @niangmedoune7962 Год назад

      Daffa beugue français bou djangone kene Dou degue 😂

  • @assanediop771
    @assanediop771 Год назад +3

    Balla gaye yaye sama mbeur damala moudiee bagne sah nila weur dougne la wah deugue do entrainè

  • @omzoseck8566
    @omzoseck8566 Год назад +3

    Champion by balla caye ❤

  • @MohamadouDiallo-t8o
    @MohamadouDiallo-t8o Год назад +3

    Ki mo nekh nena amoul ko eupeu dolle amoul😂😂 barki yallah boy niang dala epeu dolle dane la

  • @Kako-ho9jx
    @Kako-ho9jx Год назад

    Kou khame khame mou lamb la balla gaye

  • @mansourtine8856
    @mansourtine8856 Год назад +1

    ayyy wayyy balla dégo français dego wolof wakho fi dara ay heureux rék

  • @bayemassaertv6331
    @bayemassaertv6331 Год назад +2

    Bou lén soon beuree doley kou maguett khalé daan laa

  • @ibrahimagueye3343
    @ibrahimagueye3343 Год назад

    Balla.a.ete.maraboute'.par.boy.niang.depuis.longtemps.c.ce.qu'il.a.poussel.a.avoir.le.courage.de.l'afrontzr

  • @mouhamednabienndiaye8439
    @mouhamednabienndiaye8439 Год назад

    Focus 2024 vive président Ousmane sonko

  • @serignekhadimdieng
    @serignekhadimdieng Год назад +10

    Tres sincèrement faut sortir par la grande porte meuneto té woor gua sa askan démal défi lénéne si batine damalay soot soy beurétii dee

    • @yayadiaw4676
      @yayadiaw4676 Год назад +2

      Dettt wayyyy

    • @osame8934
      @osame8934 Год назад +2

      Bilay brooooo

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd Год назад +1

      😂😂ani yalla

    • @serignekhadimdieng
      @serignekhadimdieng Год назад

      @@AminataDIOUF-ez8kd khana khamoni lii yalla yoor mingui mou deff si domou adama yii so wakhé rek té yalla takh li neek si yaw guakoy diambat bilahi meune nako fathieu si trois jours

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd Год назад +1

      @@serignekhadimdieng waw frère lolu mom c vrai mais ki nianal ko mo guen ngakoy soot défoula dra

  • @diopaladji4221
    @diopaladji4221 Год назад +4

    Physiquement contacment😂😂

  • @sambaba683
    @sambaba683 Год назад

    Fadam 2 limou wakh li deugueu leu khamna lambeu machallahh

  • @tamsirmbengue4593
    @tamsirmbengue4593 Год назад +1

    Merci Baye balla yaw rek yafi wakh dégue nékoul si Dara Di doul

  • @mbalkakognedof5866
    @mbalkakognedof5866 Год назад +4

    Tant que boy niang diékha lou lén dou nguén gueum ni mbeur la

  • @mbowsidath1629
    @mbowsidath1629 Год назад

    Do touss ma nekon sa première fan’s mais do gatt

  • @sheky3138
    @sheky3138 Год назад +3

    BOY NIANG DOU ATTAQUER MOUKK DAYE XAAR REK! MOTAX MOU SOOFE MA QUOI!

  • @thiernosarr8939
    @thiernosarr8939 Год назад +2

    Pere becaye kagn la 😂😂 nena vip yii ak rewmi

  • @gorasambe3719
    @gorasambe3719 Год назад

    Bilahi nangoul nala mai par c k khamo dara bikahi

  • @bayematar10
    @bayematar10 Год назад +3

    Niane yoroul mbeur dole rek fiit balla champion bi

  • @GorguiNdour-e4m
    @GorguiNdour-e4m Год назад

    Balla gaye digue ma Ray beugueu da fort sa.numero tayalla takh

  • @AïssataKane-i3s
    @AïssataKane-i3s Год назад +1

    Balla mougnele boy Niang balamene

  • @moussacisse1509
    @moussacisse1509 Год назад +1

    Balla amena dole takhaw na serignam yi gno dioume da indale victoire waye si guew gui lako gnakee

  • @gestutv3502
    @gestutv3502 Год назад +3

    Mbeur day wore bayina casamance

  • @babacardiop5162
    @babacardiop5162 Год назад +9

    Vrai Gaindé 😂😂

  • @oumarsambou8198
    @oumarsambou8198 Год назад

    Balla gaye 2 bo amone mille défaites yow lay faral. Mane ak yow depuis issa pouy

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Год назад +2

    Yekini si bir beure guako dane thiapathioliby aussi sisa bir beure silala dane dala diokh beure bi tekou dioumoul do danou

  • @zodalla9763
    @zodalla9763 Год назад +4

    Le meilleur ❤

  • @alphasalioudiallo9506
    @alphasalioudiallo9506 Год назад

    Boy niang è le meilleur

  • @YoussouphaGaye-en8jo
    @YoussouphaGaye-en8jo Год назад +2

    Sallalahou aleyhi wa salam

  • @abdoulayediene
    @abdoulayediene Год назад +1

    Balla champion comme modou lo