Bril - Sama Beug Beug ft. Pape Birahim (Clip Officiel)
HTML-код
- Опубликовано: 16 янв 2025
- ** Abonne-toi à ma chaîne ici goo.gl/Qw5BFh **
Nouveau clip « Sama Beug Beug » !
Bril et son ami Pape Birahim discutent de leurs goûts respectifs en matière de femme : ils ne sont
à l’évidence pas du tout d’accord…
#BrilFight4 #Bril #PapeBirahim #ClassChicMusic #Birahim #PrinceArts
** Crédits de la chanson "Sama Beug Beug" **
Auteur : Bril & Birahim
compositeur : Bril
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music
Une production de Class’Chic Music (Senegal, 2018)
** Crédits du clip Sama Beug Beug **
Réalisation : Reverse Studios
Stylisme : Thiang Couture 785137833
** Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux **
Facebook / brilfight4
Instagram / brilfight4
Twitter / bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4
** Lyrics de la la chanson « Sama Beug Beug » **
[1er couplet]
{Birahim}
Les gouts et les couleurs ne se disputent pas
Mane kima beugg djokh ko sama khol, na ngén massi Ba
Nimou tolou lako beuggué avec son poids je l’aime moi
Bala may dof ma teuyéla nga féss samay Lokho
Ndakh khalé bou fess beuri djapp mo djara tek lokho
Awoumak affaire taille fine
mane gni la mine ,
way djekk dji niomay daadji yeah yeah
Souma naré déé thi aleu nama Gaïndé Ray
Souma naré déé thi aleu Guinar douma Ray boy
So beuggone étage cherie mom lalay may
Nimala beuggué dara douko Fay ,
Waaaa waaaaw
{Refrain}
(Bril)
Mane lima gueuna beugg taille fine la
(Birahim)
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
(Bril)
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
(Birahim)
Limay daanél néwoul thi taille fine !
[Bis]
[2àme couplet]
{Bril}
Beutt dou yénou waayè khamna lou bopp attane
Beuggna kou yèm khalè bou maggoul attam
Taile fine kèn dou mom, woyof attane sèn bopp niokko mom , hèè
Nameuna koumay fowè diko nabbeu nabbé
Kou yèm ci ay lokho makoy wane nimako Nobé
Bokkoul ak kiy tokk sa kaw té do meuna Noyi
Diss ba doto yeukk lokhom you Noy yi
Taille fine yi , sawar nagn té folén woo niou wouyoula
Té yaw sa djéék bi boko toppé bo dawoul niou robi laaa
{Refrain}
(Bril)
Mane lima gueuna beugg taille fine la
(Birahim)
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
(Bril)
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
(Birahim)
Limay daanél néwoul thi taille fine !
[Bis]
[3ème couplet]
{Birahim}
Bou Séédday djoté do sokhla andou Thiouray
Dangay bokhou rék teudd thi wéttam mou tokk dila Raay
{Bril}
Bou Taangay djoté do sokhla Clim waay
Di nga meune di foo ak mom té niakkeu doula Ray
{Birahim}
Ki dafa djongué ba louné lamay déflo
Souniou teuddé dafmay djoylo
{Bril}
Ki dafa woyof ba founé lay aw thi mane , boumay khalatt lim may def dafmay Réélo
- Gni andak taille fine wanélén sén bopp (heeey)
{Birahim}
Gni andak djéék dji yéén ana ngén (Heeey)
{Bril}
Gni andak taille fine wanéwoulén
{Birahim}
Gni andak djéék dji , djoukklén may khool
{Refrain}
(Bril)
Mane lima gueuna beugg taille fine la
(Birahim)
Mane lima gueuna beugg Djéék bou diss la
(Bril)
Nooon mane beuggouma Djéék bou diss
(Birahim)
Limay daanél néwoul thi taille fine !
[Bis]
Bonjour mon nouvel album « SUBA » est sorti . A écouter et/ou télécharger en cliquant ici listen.lt/BrilSuba1
je suis heureux de vous en faire découvrir aujourd'hui les 15 nouvelles chansons.
Ok Bril
Trop cooool
Je suis fan
Je préfère tayfin😍😘❤👍👈
Ajo
Bril Officiel Bonjour
Youeet mp4
Quand deux ndananes fusionnent ça donne toujours ça qui est d’accord 🔥🇸🇳🙏🏾
S8 entièrement d'accord niom niar meunei nagn founei
Moi broo 🔥🔥🔥🔥 respect nice frere
Ton numéro stp
Ho mane mom khawma fouma fété ndakh dama séw mais dal begna né fadj
Mw
Vive la femme en général mou done taille fine wala djeg, koussi d’accord...? ❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
😍😍😍jiguène dgue day ame dagou walé xaley bou bah ak formame di dagou sa biir keur def tokh taille basse ana gni ande ak pape birahim na bleu may guiss way😂😂😂😂😂diég dji rek meune dadji waté😆😘😘beau le duo❤
Wa waw deugue nékhoul dh diongama pur
Walay tourondou wakhatiko
Oui moi je d accord
Mais moi je sui tayfine
@@daourmbaye8921 togal akh seu taille fine borom aiguille
Djiguen daal da kay ndirou waa wa waw diongama feep loo sol mou diap mangui si pape birahim
Ms jaime bril fight four
Quand deux voix extraordinaires de la musique sénégalaise se croisent ne peut donner que ça comme résultat. Félicitation
Sheuteute dfatina meuninam man dal beugue na li ani sama mbook taille fine yii bril reik si xol dara douko dindi😍😍😍😍
🙋😍
Là mdrrr
😍😍✋
TF SI XOL
🙌🏾👩🏽💪🏽
« De l’autre côté « tellement touchant ,magnifique ,BRIL un vrai artiste félicitation !!!
Film mr bien
First 😍😘ana gni beugeu bril pouce bleu🔥
Nice clip je kiff ❤❤
yasmine baby yama geuneu nekh ke bril
Moi
🍸💗💗🍸💗💗🍸
💗💗💗💗😍😍😍
💗💗💗💗😍💗😍
🍸💗💗💗😍💗😍
🍸🍸💗💗😍😍😍
🍸🍸🍸💗🍸🍸🍸
🍸💜💜🍸💜💜🍸
💜💜💜💜💜💜💜
💜🌹💜🌹💜💜💜
🍸🌹💜🌹💜💜🍸
🍸🌹💜🌹💜🍸🍸
🍸🍸🌹💜🍸🍸🍸
Mariana Butera on peut se parler sur pv
J aime bien cette chanson et la ressemblance des voix de ces 2 artistes, leurs qui sont toutes les 2 magnifiques. 💯💯👊👊👊💯💯💯💯
Sortir avec taille fine tu te demandes si elle a besoin de nourriture ou de l'amour
Djiguéne day féss délleu team diongoma ❤
😂😂😂
Senegal Senegal Senegal Senegal
MariamamDiouf
😗
😂😂😂😂
Très belle vidéo machallah ! Kou beugue Duo bi pouce bleu . Taille fine 💪💪
Bril fight 4 ft Dip doundou guiss qui est daccord? mais dou done mbeuguél dh😂😂👑
Moréén TV warna meuneu nekk dh 😂😂 loy bagne mou done mbeugeul ni 😂😂
Moréén TV moi suis d'accord
Aka ma thié d’accord !!!!!! Mais padon na nékk love nak loool
No meune na nk mai op son mbeuguel coz ils ont tro de son d'amour
Me😀💗💗
jongoma yi sen lokho thia kaw
bilayyyyyy Pape birahim ya xamm lou bakhh wayyyyyy brilll vraima weirei gua koi loyyy doyei thiep bou sewww mounane taille fine dara bakhousssi . POIDS LOURD 4 EVER MANE BEUGEUNA SAKHHH NAMA RAYYYYYYYYYYYYY
Qui est là en 2024 💙💙
🙌 team taille fine 😭
Nice na vraiment
#Team-taille-fine
Taille fine douu ayyy fohh kou d'accord reck beuseull j'aime💋💖💖
J'aime
Mane lima geuna beug moy diek bou disss💪dima nokh bamay dioy😢😢mou nakhati ma🤷♂️
Musique sénégalaise, les filles sénégalaises et les mes sénégalais sont magnifiques.✈🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Xayooo ani lei taill fine😍😍tamite
Hooh trop nekh bargui bleu bleu koumou nekh beusal j'aime waay 💗❤ani tail fine yii
coumbis s3y3 bilae tail fine mokko yorr💞💞j ' aime bril
@@bintouseye3375 wawaw tail fine rk eupeuna
coumbis Seye ✌✌
@@khadydiack1695 ❤❤
coumbis seye
Il a encore montré son talent Macha Allah yalna nalen yala soutoural thi barker seydina mouhamed
Mei ku nekeu akkk nila souniou borom binde ku nekk amnga part si son bi chapeau a vs bril do sen morom
😂😃💚❤📦
les rondeurs, une identité bien sénégalaise!!! A vous les XXL!!! Clin d’œil à my wife!!
😂😂😂Allez les femmes rondes😍😍😍vive les tailles fine oci😍machallah clips bi nekhna😍😍
Nice
Je t'aime
@@dedsec2.017 tu aime qui
Quand j enten ta voix bril j m sen tre bien si je swi en colère sé toi ki m rend mn sourire vrmn jtaim❤💖😍😘
La même chose que moi bril yala koye faye
Team fess deill mashalah sen lokho may senn😂✋❤
Waww niogii ni dh
Adjashu Laye Fall ah eupneuh naq kennn dou niounnn😂
Weuw Kayy👋djiguéne dakoy nourou wala mou baa tt ce kil faut là où il faut beugouma daray cuire-dent😂😂(dagnouy fo rk)v
@@Biddew khana
Niongui nii waw kay
Wa Ani taille fine yi wané wou léne ak taille fine rk eupou na
Gnon ngui nï👯👯👭🌹
Waw waw dangay ladj
On n'est la
Mangini
Defa lerr
Clip bi tangana dée way son bi nickel Macha allah thia Kaw thia kanam
Je suis avec bril, laver les mains qui et d'accord avec bril
Moi
Fofana Mido moi
Un homme respectable
Moy toulma khalé bou féss 👎🏾 mane déh taille fine rék nio may danél 👍🏾😍😍
Seck Bologna non taille fine dou ay fo
tamiy deugue taille fine rk
Gnomm nioko yoor fowoukay dafay oyof
Merci gni beug loubakh yeup nionguici taille fine
@@famanga8152 wakhatiko dé
Oyoff atane s'en bopp nioko mome 😍maname taille fine dall😎sama mbokk yi manifest3 vs
Les Tailles fines👑 manifestez vous way
On n'est la
Taille fine yi rek laay top
Bilaye birahim yaye diaye tar rek man mome na tate bi bax rek😉magui sy tay fil de man
🤔
Dafa beugue djiguene trop😁
@@astaseye1616 ta sof kay😂
serigne takkricain copin yaw xale nga doxal nelawi
@@siirdiop9701 😂😂😂khalas
2 voi extraordinaire ki se croisen ohhhhh donn d frisson et l'envi de danser.sama khol frigo
Aller les taille fine manifestez -vous
Là
Buy bulema ray
😍😎😚
Nionguini😍
Mously Lo Ken
na aguiiii
Après l'annonce de kouthia pour serie bi kou gneuwat deglou son bi❤beusseul j'aime
Taille fine defa Rafette ❤❤❤
😍😍😍😍
My god
C trop nekh
Je t'aime Pape Birahim
Beri nga si morom bilaay
Je t'aime toi aussi 🤣🤣🤣🤣🤣pape birahim la guëm 👈👈👈👈👈👈👈👈
Bilay walay 🙈🙈
jvous kiff vous deux mai tailles fine lagn wakh gnoun☺☺
Taille fine moko yor
😂😂😂mon pays va mal😂😂 niou andak taille fine yi beuss leen jaime waay
j'aime
Team tay fine aniguenn 😍😍gnoune rkk sii nekha foopp yeukeuti athioum tay fine dou reuthieul sa deuneu deii DEUG nexoul ...foyoukaay dafay woyoff😂😂
pape birahim tu as une voix en or incontestable kan jtentend sama yaram dafay daw wallahi.... Big up a bril 😍😘
taille fine dal rafètna . qui est d'accord ? ? ?
Taille fine dal
Machallah
Moi
Mane taille fine mo may danel❤❤❤❤
@@aissatasylla347 me
Nice 😂😂😂😂 mé 2 Artist😍😍 taille fine wonélen sen bop😂😂😘😘😘
On dit pas de taille rond mais taille fine
T
2po2oziz8zeieoepzofoz2 maty DOIt
Taille khifffffe wala taille fine😂😂😂!!la classe est au rendez-vous duo de choc j'adore !!!!
😂
Delen aimé 100 fois ahmada
Pape birahime ya beugu lou métiii noooo do déme. Macha alla vrai artiste gua
Qui est a 2024 pour soutenir les tailles fines comme moi🎈🫰✅?
Mane beugu naa kou melni bril way😂fine moko yoor surtt été ohooooo
Asc Taille Fine 🙈 je T'aime ❤️ Bril Fight 😘
Astou Kadam merci de vous abonnez à ma chaîne
Taille fine moko yor
Taille fine lalayy tegual nidehh Bril t'a encore frappé !!!Congratulation
quand 2 chanteurs se reunissent ppur mettre en valeur la femme djek ou taille fine on n'est toute belle 💕💕
ana team driankei bi 😂😂pousse bleu
Bril fight4 big up yaw yonla begue piir machallah clip bou nice mais pape birahim yaw kenn demoul nga dess machallah mane dal begue na lenn bonne continuation à vs 💖💖💖💖💖💖💖💖
Binetou Faye je vous invite à venir regarder des vidéos challenge musique sur ma chaîne. merci à toi
Sama team taille Finn yi brightt fight lagnou wakhhh gnounn💘
Ma ngui si yéne mane fowékay day yam si loxo
Mamadu Faay deug nekoul
@@soldaroucheikhmountakhamb5015 wa guis nga fowékay day oyof
Mamadu Faay mba ame nga si taile fin yi rek
@@soldaroucheikhmountakhamb5015 xaxa no amou ma si nak
Djiguéne déy fess❤❤❤
Way nékhoul ba nekhou un vrai homme daguay beug diék dji ndakh siguay sentir sa boppour deugu fo tollou diko séeen ooooooooh j'aime les Diék way
From poto cornel yi rek wawaw 🇸🇳🇮🇹❤🎉❤🎊
Ni taille fine ni taille drianke mais le juste milieu qui alterne les deux de belle courbes
Bilay nekhna troppp khale bou fess beuri diap djiguenne dagne am ay rondeur way
No pape birahim dafa am tiasssss yalla hamnako. J laimmmmeu trop
Gni beugueu niar yeup(taille fine, diek) beussal pouce bleu
Khane moy khaye dègue lou2024😂❤
Mane mome diéck la begue sou daguo sa bir keur gua khamna léppou degue la cou begue diéck na bleu way
Baboucar Sokhna merci de vous abonnez à ma chaîne
Dièk dei fèbar rek
Namouniou draa
Baboucar Sokhna ta raison
E
J'ai kiffé ms j'aimerais un trio genre avc wally mdr vraiment sa fera feu et forcément flamme
Taille fine wayy GNi beugueu taille fine pouce bleu dieck bou diss yi taguay yeureum nallene
Machallah son bi noumou nekhe eupeuna♡♡
Vraiment je vous respect, Taillefine
Taille fine RK Apeuna 💓🌷💞 bilay Bril MoMA Neikh RK😍😍💓
Team bril tjrs du lourd 😍
Oh pape birahim tu fais partir de mes chanteurs mais méré nala trop parce que taille fine la 😢😧
Gnou andak taille fine sen lokho way may sène👭
Tu est Bell
Kéne Dou diégi
I'm here
Deugue nékhoule💖💖💖👯👯
Belle
Fowoukay dal day oyof bou dissé rek sonal borom ❤️💖❤️💃💃💃💃💃❤️❤️
Ww yow bou disss nga wala Bou oyoff 😂😂😂😂😂👉
Ay ndeya mane dal yaw lay weur taille finie rk
Matar Diop15 nakhoma
Ameth Diagne bou oyof 😂😂😂😂
Ma fvmm lay done reine dé taille fine j laim
Taille Fine Rekkk😍😍😍😍
Bilaay Birahim mako beug waay😍😍
Team ptite jongoma waay✌✌❤
Rosalie Oumy Mbaye je vous invite à venir regarder des vidéos challenge musique sur ma chaîne. merci à toi
Birahim rekk 😍
Owkei machalllah😍. Way bi nèkh na trop prck niari ndanane gno dadjé😘
Mais nak en général dièke you diss yi daniouy diabète rk bâ niou cardiaque So démé ba nèke sa ohhlala gua niak khaliss nakh ordonnance,niouy guène thi bènd bi niou lène di thiatou. Kou gnou n3 déffal sport do attane sa bop😢.
Vive Taille fine way😍.
Mais peu importe on doit se sentir b1 dans sa peau😘
Breff. Sinon niougui kharate bénène duo Bii saff na niou.
Qui est d'accord pouce bleu😍😛❤👍
😂😂😂😍😍😍taille fine way💕💕 dou moromou lénéne ci lepp 'nakk..allé brilll chapeau à tw😘😘.
Ana diekk you diss yi😍😍❤
Diek rek manhallah❤❤ bonne continuation belle muisque
Mention spéciale à @Reverse Studio franchement vous avez assuré et que le meilleur reste à venir félicitations aussi à Bril et Pape Birahim 🙏🏾❤️
Machallah yanalah yallah defal diamma jlm tjr bril
mane si bril la far dè taille fine rek woyof ba dè machalla
Vulgaire, certes mais à l'image de la jeunesse sénégalaise. Arrêter de jouer aux choqués.
Bravo les gars. bonne continuation.
Et c'est pour ça qu'eux (artistes) doivent monter le bon exemple face à une jeunesse en perte de valeur comme vous le souligner. Faw am gnou gnouy orienté des fois et les artistes ci lagn bokk c des porteurs de voi
Super
Cool
OK
Taille fine rék beug 100% qui est avec moi et Bril pouce bleu🔥
non
Khar Ndoféne Gaye
@@madamebleu9328 salut
Bril way de tout coeur avec toi taille fine rkkk.feulalè rkkk sandè kou df sougnou lougnou nèkh
aye waye a travers cette chanson je me sens un peu visé mane dé diekk rekk
Excellent son et clip..bravo..cela ne change des sambay mbayaneee
Moytoulén fataya complet yi😂😂 danouy Tass yaram dh Ani wa team taille fine😍😍
😂😅
Lol
Who loves Bril Fight and pape Birahim❤❤❤❤❤
Félicitation à Yarba pour le déco! Nice song!
Je sw vk pape diekk puree laye weur jigeen daye fess waye ki est d'accord avk moi sa lokho sii kaw
no😍😍machalahhh pima sama djongama bi pirrr Oumy t'aim
Qui est laah Avant les Millions de vues ?😍😍😍😍😍🖐️
Taille fine rék dara fayou ko
👋👋
On adore les femmes minces 😂😘😘😍😍😍😍
merci j suis mince
Bilahi 🖒🖒🖒😁💪💪💪💪
waxal way
Djiguéne dall dafay noy am dagueu bou Nice Mouy taille fine ou lourd no mel rek sant Nice clip suis pour les 2 😂😂😂😂
certes les images ne plait pas mais j'aime tellement cette chanson je l'ècoute x fois par jour c'est la première fois que je laisse un commentaire sur une chanson chapeau à vous deux
Dama teude di nalaw Sénégal yèwou guiss sama bop Nigeria i like oohh🙏🙏