Ndiolé Tall feat. Wally - Choco vanille

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 12 мар 2018
  • Choco Vanille le nouvel opus de Ndiolé Tall, unique dans son style, en featuring avec Wally Seck
  • ВидеоклипыВидеоклипы

Комментарии • 3,2 тыс.

  • @bayecheikhdiouf4137
    @bayecheikhdiouf4137 2 месяца назад +69

    qui l'ecoute en 2024 ?

  • @alicediatta5117
    @alicediatta5117 3 месяца назад +40

    2024 toujours wally ❤🇸🇳🇸🇳❤

  • @nabicoumbassa5875
    @nabicoumbassa5875 4 года назад +1092

    Bilahi immigré métina 😢maylènnma j'aime reck pour ma soulager avant 2020

    • @Adaaaaa625
      @Adaaaaa625 4 года назад +28

      YALLAH NGEU AM DIAM NABI MEY NALA J'AIME😍😍😍

    • @fatoumatasidibe9276
      @fatoumatasidibe9276 4 года назад +13

      I Épinglez les morceaux de texte copiés pour qu'ils n'expirent pas après 1 heure

    • @bintakasse7726
      @bintakasse7726 4 года назад +10

      May nala j'aime

    • @maguetteguerre9281
      @maguetteguerre9281 4 года назад +5

      Yalla bakh na Unchalla wakhoul kén dara

    • @dioumastou9503
      @dioumastou9503 4 года назад +3

      @@fatoumatasidibe9276 km

  • @dabaloum3168
    @dabaloum3168 4 года назад +54

    Sa way d’où Meusa sapiii 😫🥰❤️🎊Lo wayoul nekh barke yonneti qui est la en 2020 niou get sons bi te 20million vue dougou rang mouy gaaw🏃‍♀️

  • @salvarombodji5504
    @salvarombodji5504 4 года назад +337

    Qui écoute ça en 2020 no c trop cool wallay the best song 😍😍😍😍

  • @mamitatorodo5621
    @mamitatorodo5621 6 лет назад +10

    Lii nexnaa wayy machalah😍😍Doo faramalambeu nak Faramarène pire guaa Ballago😍😍😍

  • @Khadijahbaby02
    @Khadijahbaby02 5 месяцев назад +12

    Feeling bi rek anh 😅it’s amazing 😻 ❤🎉 best duo

  • @mariendiaye2961
    @mariendiaye2961 Год назад +30

    Qui comme moi écoute cette chanson jusqu'en 2022🥳🥳🥳

  • @adjacoumbadiouf8677
    @adjacoumbadiouf8677 6 лет назад +7

    walayy deh dangeu meune woyyy my faramaren voix buy geune di nexx machallah kone sa pararipi moyyy sa parara wally rekk si xol lenen dathia xadioul akkeu efficace 😂😂😂😂😍😍😍😍😍😍😍

  • @mamethiernothiombane5968
    @mamethiernothiombane5968 6 лет назад +31

    bilay sama xol séddeu n'a.man déhh souma yalla beugué nalla fi bayi wérall sa voix,diouboléla ak sa diabar,déffal diam papa thione ak maman kiné Ki liguéy keur papa thione bakh takh lépp nékk tayy.waly yalla nalla yalla diapalé té takkal la ba faw.daggoul noumoula nékhé nakh yalla néna waw.(mirma)

  • @mamasow6124
    @mamasow6124 4 года назад +222

    Qui est la 2020 waly chanteur du peuple 💪🔥👑

  • @vivianekowa2226
    @vivianekowa2226 6 лет назад +379

    je suis camerounaise vraiment vous faites la fierté de notre continent je vous aime

  • @gnimalybadji4458
    @gnimalybadji4458 6 лет назад +38

    Kholene ci Ndiole te bayi khesaal bi. Nice clip Alune moy sama para ripi. Kou beug sa para ripi mayal ma Waly❤

  • @AfroDizJoy
    @AfroDizJoy 6 лет назад +90

    Team Ndiolé, diamant noir 🖤🖤🖤🇸🇳😍😍 bi moy sama son officiel bou bess 💃🏽💃🏽

    • @dieyeaminata253
      @dieyeaminata253 6 лет назад

      AfroDizJoy noir teint de luxe leu

    • @assysene8506
      @assysene8506 5 лет назад

      wa koumay dimli thî numéro Wally je l'aime trop fort

  • @user-rh3jq6yl9q
    @user-rh3jq6yl9q 8 месяцев назад +9

    Ndawtal lénema j'aime dama xéwlé si 2023 bii

  • @kofioduro8256
    @kofioduro8256 5 лет назад +58

    A lady called Nicole introduced me to his music in Ghana and I fell in love immediately I heard his songs. Go Africa, Go Senegal. Let's support our own

    • @julasecka6185
      @julasecka6185 2 года назад +1

      @@abdoulaye_diop is good morning

  • @aminata0485
    @aminata0485 6 лет назад +16

    Aieeee. Sama xol ba ngi feex! Chiii Waly dundeul way. Bravo à Ndiolé!...

  • @fashaafall1333
    @fashaafall1333 6 лет назад +30

    Thiey faramarene bi filling kességua
    Yalna yala weral batt bi do gnom té dougn yaw 💪💪💗

  • @fatousane4165
    @fatousane4165 6 лет назад +21

    My husband my best friend . This is too much ndiollé💖💖💖 feuleul feulaléko ridj sa ndig gneuw gnou dadjé 💖 😂😂😂

  • @birahimsoldaroussaliou117
    @birahimsoldaroussaliou117 6 лет назад +18

    Cette très belle chanson mérite des 20 millions de vue diapp len si bok galsen

  • @cherifmohamedelbachirsow4020
    @cherifmohamedelbachirsow4020 6 лет назад +81

    Wally le future Roi de la musique sénégalaise🌼🌼🙏
    Wally ndiolé Tall diama noir le duo du mois

  • @aidasagna4283
    @aidasagna4283 6 лет назад +22

    nice mashalah avc wally tjrs du lourd wah ndiolé lingua robe yako tay mashalah rafet nagn amnagn classe

  • @mamiendiaye4662
    @mamiendiaye4662 6 лет назад +37

    La voix de wally quand il dit bayima ya ngui mey togn 😂😂😂😂nice clip j'adore

  • @diariatoucissokho780
    @diariatoucissokho780 6 лет назад +23

    Machallah laffalen thiatt wally iow sa xool da rafete yallah n'a yallah faye sa xool chapeaux à toi et diamant noire

  • @rauldabosenegal1018
    @rauldabosenegal1018 6 лет назад +27

    Clip bii nice trop ndiole ft wally seck roi mbalack faramareen😍😘😘

  • @fatoumataka9966
    @fatoumataka9966 6 лет назад +42

    Wa manei kou solale ndiolé Tall???
    Tu as fais un bon travail.
    Ndeilo nga ko ces 18 ans.
    Kone pararipi!!!!

  • @lolowassa
    @lolowassa 5 лет назад +12

    Wally seck, big fan love so much all your song no exceptions, two big thumbs up

  • @tvretro2456
    @tvretro2456 4 года назад +6

    Qui est la en 2020 ? Yalla naniou yalla défal atoum khewel ak diam.

  • @aminadiop7781
    @aminadiop7781 6 лет назад +16

    Ohhhhhh dègul liii rk thieuyy Waly sama papa D'amour do moromou bène paaa😂😂

  • @saliletvsenegal5304
    @saliletvsenegal5304 6 лет назад +105

    Kou ndamone 100% Mbalakhou Wally tape j'aime

  • @parissaint-germainsfansclu4592
    @parissaint-germainsfansclu4592 6 лет назад +11

    NDIOLÉ MENE GUA SAGNE SÉ WALLY💕💕💕

  • @serignesalioudiouf9881
    @serignesalioudiouf9881 7 месяцев назад +10

    Qui l’écoute en 2023 😂

    • @Mdjiboy86
      @Mdjiboy86 7 месяцев назад +1

      Sa piraripi😂

  • @ibasarr6613
    @ibasarr6613 6 лет назад +43

    Kou beug son bi beusseul j'aime may djiss.. Nn wally neikhoul ba neikhoul mai liniou beug dall yanioukoy diokh...ndioleii kouy sa pararipi ...nice le duo

    • @seynabougueye7458
      @seynabougueye7458 6 лет назад

      Iba Sarr ksorxiv

    • @LouBessTV
      @LouBessTV 6 лет назад

      Iba Sarr Êtes vous marié ? Si oui ..
      Suivez moi sur ma chaine ..
      Nous parlez de( sexe ) , fem et comment faire pour retenir son mari dans l'ordre!
      ruclips.net/video/aLX1xVC8Fis/видео.html

  • @salioukane7638
    @salioukane7638 6 лет назад +202

    Du lourd ❤❤j v kifff enormément wally ft ndiolé tall sa teint noire baxna👍kou validei ✅✅✔Like

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад +2

      BOROM Diamono Han kone pararipii ak parara bii may degg liii la kone OK😂😂😂

    • @diorlabambisteseck8727
      @diorlabambisteseck8727 6 лет назад +3

      BOROM Diamono wa Saliou dangay enjoy mbalakh😂😂

    • @salioukane7638
      @salioukane7638 6 лет назад +2

      Penda Diop mdrrr pendita pararipii ak parara mogui tothie deuk bi

    • @salioukane7638
      @salioukane7638 6 лет назад +2

      dior la bambiste seck sa serigne dei prfw mou enjoy ko mdrr😉😉ymgx

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад +1

      dior la bambiste seck ahhh ma bambiste sa Serigne bi da rakh deh bayiwoul dara 😂😂😂

  • @tymadjah7232
    @tymadjah7232 6 лет назад +3

    Ohh nkhna magui agressei bouton replay douma si doyaleu waly a encor tapei fort😍😍😚yagui fekhal khol yi way😙

  • @byasw4754
    @byasw4754 2 года назад +33

    2021 12 millions de vues wally on t aime❤💥🤩😍

  • @kadiatousy9234
    @kadiatousy9234 6 лет назад +18

    Sa pararipi moy sa parara❤. il a encore frappé. Ani gniko beugue puce bleue 😍😍

  • @dabaloum3168
    @dabaloum3168 6 лет назад +22

    Ohhh woopOoop c'est du lourd ❤💕💕kel magnifique clip bou melni doufi gawati amati la classe élégance totale thiey faramaren loumou dougou mou barke yalna god goudal sa faan ykou weer gui ❤❤❤💕💞💞bat bi yalnako sounou borom sameuh ndiole tall tu déchiré vraiment

  • @mamysall628
    @mamysall628 Год назад +8

    2023 et j'écoute toujours se chanson 🎉❤

    • @MaimounaFall-yf5kt
      @MaimounaFall-yf5kt 11 месяцев назад +1

      même mane khamouma kagne laa thiy doyal 😂

  • @ndeyekhadyndaw1163
    @ndeyekhadyndaw1163 2 года назад +4

    Waw waw nimouko wakhè mani sa pararipi moy sa parara lou leer lii no lii raay nama son bii

  • @blackwoman3755
    @blackwoman3755 6 лет назад +548

    Ani wa team farramarene team notification ❤❤❤☝☝☝😍😍😍😍😍😍😍gnola beug barki borom touba loussi nite meune

  • @riitamarley6610
    @riitamarley6610 6 лет назад +8

    ayyy Sama papeuh doundal Lou beurii nala yalla bayé ak sa bateuhh guaye weyyyeeeee😍😍😍😍😍lou nekh

  • @ndiayemamediarra2216
    @ndiayemamediarra2216 3 года назад +1

    Ayoohh maguii fii baa leguiii💓💓💓💓💓

  • @cheriezale2244
    @cheriezale2244 5 лет назад +18

    5 mois 5 millions de vues macha allah laff thiat

  • @Diamant_Noire
    @Diamant_Noire 6 лет назад +151

    Duo de choc 😍 , quand on mets 2 grands artistes ensemble et bah ça donne un résultat époustouflant 😍 .
    Bravo à vous 👏👏 neeekh na torop 😍❤.
    Sa pararipi moy sa parara😍😍😂😂😂😂 Ndiolé rek 😂❤

  • @houleygrehu3889
    @houleygrehu3889 6 лет назад +10

    Ooh lou tah ma beug choco vanille wally je t'aime 💜 🤣 chérie sokhna aidara

  • @Lufvip03
    @Lufvip03 Год назад +2

    Just Wally💧 #TeamWallyseck 2022🤍

  • @aissatoudiaw6944
    @aissatoudiaw6944 6 лет назад +15

    Ay way cagne lay doyal thi clip j'adore trop😍😘

  • @Ceuss5366
    @Ceuss5366 6 лет назад +16

    C’est ce qui à la musique sénégalaise des featuring et des DUO de 🔥 .
    Même si on peut imaginer un Wally ft Pape Diouf wala Titi ft Viviane, DiP ft Omzo, Youssou ndour ft Wally.... Taper seen Xool ❤️ waay iish c’est le Sénégal qui gagne

  • @aidaseye2929
    @aidaseye2929 6 лет назад +8

    Ndiolé yagui may ray ak baby diougal tokk niou diakkarloo dofi nélawé
    Si partie bobou sa bate bi dafa féroce😍😘
    Mais Waly tay nak doo reuthie

  • @tackogueye2014
    @tackogueye2014 8 месяцев назад +5

    Qui est là 2023😂❤🎉

  • @noemiemotrot2167
    @noemiemotrot2167 5 лет назад +11

    Ndiolé je l’adore elle a de la classe👗👗👗à merveilles

  • @marietouthioune2186
    @marietouthioune2186 6 лет назад +104

    Une video a 1 milion de vu a 1semaine c une premier .chapeau a ndiole et bravo a wally

  • @amymarega9340
    @amymarega9340 6 лет назад +19

    Machaallah....fan de Wally depuis Londres 😘

  • @fatoundao5850
    @fatoundao5850 4 года назад +41

    Je suis fière de ces deux❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✌️✌️✌️

    • @binetagueye6872
      @binetagueye6872 Год назад

      Cxxcvbvx🏂

    • @binetagueye6872
      @binetagueye6872 Год назад

      D ff😻😻😻😻😻😻😻😻😻😻😻😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽😽

  • @doulayediop3356
    @doulayediop3356 2 года назад +3

    Qui écoute en 2021 bilay doumathi doyal♥️

  • @belladiopdieng4878
    @belladiopdieng4878 6 лет назад +59

    Wa li nekhna dé 💃💏👏👏👏 bravo , diolé ta 👗 rouge est magnifique , ça te va à merveille 👍👍

  • @sagnandeyefatou1728
    @sagnandeyefatou1728 6 лет назад +10

    oe Pk Mann Ma Contann Cii Wally....Sheutt Sama Yay dina amatii Limou Wah Reik wayeii Mann ma Ko meunoul Bayiii.... Ndiolé Wallahii Rayy Guama ... Sunu Yallah Beugueii Naniou Bayi Ak Sunu Peupeuhh...#Gooneiii_Walllyyyéeiii

  • @fatouquebe9317
    @fatouquebe9317 4 года назад +7

    Wally ndiolle néna gua tasse la le biiiiiii😍😍😍😍😍😍😍😍

  • @annadieye4487
    @annadieye4487 4 года назад +147

    Qui l écoute en2020

  • @maremediouf4856
    @maremediouf4856 6 лет назад +12

    Machalla yall dieum si kanam. Feliciatation a ndiolé

  • @astoufall7151
    @astoufall7151 6 лет назад +58

    😻😻😻ANA gniye diay sen sante pour sama papounet 😍😍😍

  • @Boygaston2.0
    @Boygaston2.0 3 года назад +7

    Je suis le seul à l'écoute en2021

  • @adjalinguerendiaye3029
    @adjalinguerendiaye3029 5 лет назад +160

    Qui est la en 2019🤸‍♀️🤸‍♀️🤸‍♀️🤸‍♀️🤸‍♀️💃💃💃

  • @Matryyooshka
    @Matryyooshka 6 лет назад +16

    Ah waw mais limom nekhna dal, mash’ALLAH BEAU DUO❤️

  • @merygaye3837
    @merygaye3837 6 лет назад +7

    Wa lou tah sohor nakk clip bii kou sa hole neh war ngaka hol di clike dislike ignane.com merci encore waly tu a encore frappe tres fort ndiole chapeau

  • @allezleslionsdembadiekh8261
    @allezleslionsdembadiekh8261 6 лет назад +32

    Yaaw mi di liir sama commentaire yallnalla yalla maye guoudou fane AK diamou AK kheweul AK weurseuk lëëpou lo beugg loudoul lou haram yallnalako yalla maye yalla nga réussite yallnalla yalla mousseull té moutheullela si lëppou lou bone

  • @coumbadiallo6429
    @coumbadiallo6429 2 года назад +5

    2022 qui est là🔥❤🥰

  • @dickefalldiop414
    @dickefalldiop414 6 лет назад +15

    Lii rèk ga wakh waly Soula sokhna diapè ❤❤❤

  • @biramaterstegen1426
    @biramaterstegen1426 6 лет назад +6

    Belle clip lima thi gueuneu nekh moy amoul bene danseur(se)j'aime

  • @leythielwanwandiallo1608
    @leythielwanwandiallo1608 6 лет назад +15

    vrement je sui un guinne mais j'aime beaucoup Wally seck🎧🎤🎶

  • @cheikhuna_cr7
    @cheikhuna_cr7 4 года назад +31

    10 million de vue❤️🎤

  • @khadyfaye7430
    @khadyfaye7430 6 лет назад +29

    Aye Wally li lanela ni tamit bilay deugama rèy depuis sax s'arrête pas s'écraser la touche replay waaaw j'adore Mach Allah 😘😘😘

  • @Doffmalick
    @Doffmalick 6 лет назад +11

    Koumay dougeul Statue ? Ma pararipi ko ✌✌✌. Tioooo paré gnousse la parara ❤

  • @adamdiop9120
    @adamdiop9120 5 лет назад +15

    Ani FaNs wally yi kou aimer beusseul j'aime

  • @doudoudiallo6188
    @doudoudiallo6188 6 лет назад +7

    ana wa team faramarene😍😍 manifestez vs 💖💖wae love u ballago❤❤

  • @lstv9976
    @lstv9976 6 лет назад +31

    No Wally do nit chak jour j t'adore encore plus li nehna way goudeul fane

  • @yafatouba7746
    @yafatouba7746 6 лет назад +56

    Ndiole sa robe bu rouge bi Nice na trop

  • @cathydiop8460
    @cathydiop8460 Год назад +2

    Wally Seck moom g toujours trouvé que la générosité se réflétait sur son visage. Waye wi neex loolou. Mbeuguël bouye gaañé moom sori rekk, moo gueuneu woor. Kou lamb ya teyy, daagou fañe la nobé...

  • @moussafaye6769
    @moussafaye6769 6 лет назад +56

    Incroyable cette chanson bravo👏👏🤗🤗🤗

  • @naboujaballago6944
    @naboujaballago6944 6 лет назад +8

    il a encore frappé le jeune faramarene
    koubagn wally Seck febarou thiipatou ngay amei fo tolou nane thiip
    tei sakh kou beugue maigrir dieuleul wally def ko none une semaine nga melni squelette kone yes
    wayy ki mako beugue way

  • @fabinetoulome4920
    @fabinetoulome4920 6 лет назад +9

    Diaye na sama sante, seick lako dieundei😍😍😍😍

  • @amycollediop1992
    @amycollediop1992 6 лет назад +9

    Li dafa nékh❤❤❤❤❤❤

  • @khadysamb8357
    @khadysamb8357 6 лет назад +1

    shou beug nala tayi nguay khamni beug nalaa😍😍 wopopeuuu

  • @amyngom3527
    @amyngom3527 6 лет назад +6

    Ndiolé loutax ma beugulaa diamant💎noir 😍😍,"chu beugunala yey ngua khamni beugunala "ohhh eupnaa neikhh ❤💗😍😍😍

  • @tfkteew3586
    @tfkteew3586 6 лет назад +181

    Ndiolé vous êtes ravissante avec la noirceur d'ébene Machallah nékhna 😍😍😍

  • @khadyndao2655
    @khadyndao2655 3 года назад +3

    Qui écoute en 2021 li dou meuseu fayy💃💃🥰❤️❤️

  • @akd696
    @akd696 6 лет назад +3

    ahhhh thioumm le 28 rékk inchallah dara dou doy. kou geum ni wally seck cest le meilleur besseul
    jaime ma guiss👍👍👍😍😍❤️️

  • @lenaadioufy2544
    @lenaadioufy2544 6 лет назад +41

    Wopopopopoppp Non mais waly warna mayé kiné diouf Diaga ak papa thione ni dall ak famille bi yeup😂😂😂tieuy mbeuguel mo bari dolé

  • @mariamacisse825
    @mariamacisse825 6 лет назад +17

    Mais vraiment yena gaw😀 deja 50 com khana ma top séne guinaw rék machalla kene dou mom

  • @mounandoye9709
    @mounandoye9709 3 года назад +13

    La puissance vocale 😍😍😍

  • @sokhnasall8919
    @sokhnasall8919 2 года назад +4

    Qui est la en 2022 beuseul j'aime

  • @rasoullyaawa5637
    @rasoullyaawa5637 6 лет назад +16

    Youyou machala wayy yallnasa diam sakh kouko begue rekk mane la bègue waly rekk li eppna wayy ❤❤❤❤❤

  • @paulinemalack7188
    @paulinemalack7188 6 лет назад +14

    Ooh... very sweet!💖😗 Wally got the moves..Farramarene for ever👌💓

  • @marietoufall3271
    @marietoufall3271 6 лет назад +1

    Waaaaaaaw c trooooop cooooool é ki aime wally tap j'aime 👍👍👍👍❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bakaryndiayethiam9340
    @bakaryndiayethiam9340 3 года назад +5

    Nabou
    J'adore le son est très bon😍😍😍😍

  • @ndiappalykane6934
    @ndiappalykane6934 6 лет назад +31

    hay wa guayi kou beugue wally na bleu ma kholl book

  • @patheseck9741
    @patheseck9741 2 года назад +4

    Lima setane thi tiktok bi motakh ma nieuwatt fi kon liii dou chambre

  • @thiorodiouf6136
    @thiorodiouf6136 3 года назад +2

    Ça me rappelle le jour de mon mariage c'est pourquoi je le, adore

  • @majoileeva
    @majoileeva 6 лет назад +53

    Sénégal dall kou beugueu ayy vue sur youtube fait un duo avec Wally ses fans sont au taquet 🤔😂

    • @miadioufdem6582
      @miadioufdem6582 6 лет назад +2

      abibatou thiam DEUGUE BU WEER

    • @akd696
      @akd696 6 лет назад +1

      abibatou thiam non cest que Wally seck c le meilleur .

    • @majoileeva
      @majoileeva 6 лет назад +2

      Fatou Cisse en tout cas Ndiolè n'a jamais eu autant de buzz pour un son

    • @mouhamedmoustaphathiam8335
      @mouhamedmoustaphathiam8335 6 лет назад

      Ndiole use ya y yayou wali👉💍😢😢😢😢😢🐒🐒🐒🐒😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢