2025🎉🎉🎉 problème cast xawma kégne lay diekh Senegal mais nioune jeune yii war nagne ko dindi c'est possible mane deh inchallah rabi souma yallah mayé dom koumou beugs souma xolé djikom doyma ma mayéko bou féké dijoulit la 🎉🎉ndakh moy deug lolou la yallah wakh nioune niepou bénn lagne kénn geunoul kénn nio yém fa yallah ou❤❤❤❤
Seul le travail paie et Waly le sait c’est pour cela il répond jamais au question inutile ni aux attaques de certaines sénégalais et sénégalaise qui n’aiment pas voir un jeune qui avance et qui travail pour son pays yalla na khole yi ceddd si barkhé seydina mouhamed psl et joyeux anniversaire waly longue vie à toi
Barki yonètibi il est le meilleur 💪❤️3 clips si 2 mois 😍Maryacine yalla na yalla weiral bateu ganiouy beigual chak jour☺️Way kateu 🎤❤️yalla mousseul leu si say noneu ak keip koula bgue feixèl🙏🙏
Thiey wali defatina meuniname machallah sma faramarene bii yallana yalla wéreul bate bii la voie dor de la musique sénégalais borome le 27/4 ngaye fii No grande théâtre dou yombé nonou dina melni sabarou lébou kou nekh di danou aye rape 😍 wa lii nexoul kou contane si mome maye ma j'aime svpl j vous en prix
Wally seck ceux qui disaient que legui ngua fay lol depuis combien d'années batey, avancement rek laniou guisss mashala, derrière chaque grand homme il ya une femme spéciale, mashala à toi l'artiste de sa génération
Le King est de retour je suis guinéen vraiment je vous j'aime Seck moi sait moustapha bayo je suis guinéenne habite Strasbourg que le bon dieu vous bénisse
Wally dafa tangue teh hamoléne loulu 3 clip dans un moi il est le premier musiciens à le faire wali nehoul😂 Yobanté Taxi love Dafemay dal Ohhhh 😍 😍 mané kou beug Wally pouce bleu mu dalgnu😂😍
Vraiment demb bou Wally family demeii prison forbet xoll yeup toy na maryacine prisonnier content naniou si yow weuyalll nanioula fethiall leu donc lolou tamitt dafniou dall niouy def you bakh yoyou teii leup yako waralll amalll diam rekkkj Dafmay dall naniou dall niou and ak mom ba grand théâtre 😍😍🤔
Suis pas mélomane mais waly lo woy nehneu meu Je t'aime depuis la première fois que je t'ai vu sur le clip de papa thione batey xawma kagne lalay giss nak😏😍
Wally est un monstre de la musique sénégalaise je suis peulh mais je l'aime il a une très très belle voix . La question reste à savoir combien de personnes écoute en pleurant ça musique. J'ai pas eu la chance de te rencontrer pour mais vous voyez presque chaque fois dans mon coeur continu de les faire vibrer.
Nice nice nice vraimen jai plus les mots Waly Waly Waly loumala wara wakh Bilahi khamatoumako khana nianalla goudou fane rek yalla weral bateu bi Bilahi beuguenala
Wally seck le LM10(Leo Messi10) de la musique sénégalaise. Quand tu es sur le banc( tu ne sors pas un album) le match( scène musicale) est sans saveur, aucun frisson dès que tu foule la pelouse( tu publies un son ) la population est en ébullition. Tu marques un but ( tu joue sur scène) nous le célébrons tout cœur avec toi, les scènes de liesse et de joie sont innombrables. Que Dieu te protège. AMINE.
l'exclave de la passion, l'homme à qui la musique coule dans ses veines, un talent bien confirmé, du savoir faire incontestable. le poète dakarois, l rossignol de la musique Sénégalaise, l'un des paroliers de la musique Sénégalaise et l meilleur de sa génération : Wally Ballago Seck
Yobanté Taxi Love Clip yoyou yeup rafeet na teh diarna yoon et ses clip vidéos sont très bien réalisés waayé Clip bi Dafmay Dal moma dakkal parceque daffa simple teh bariwoul nitt j'aime ça mane dama beug lou simple beugouma lou xoumb dina amm 100 personnes ci Vidéo Clip lolou day diaxasso bougouma lolou 3 personne ci clip rekk baxna 2 et 1 danseur ça suffit motaax Dafmay Dal nignouko réalisé neexnama en plus Clip bi da seet wethie saltewoul machaalah🙏 trope mais n'empêche Yobanté c'est ma chanson préférée dans l'album #Symphonie Nice Wally Machaalah🙏et Bonne continuation!🙏
Yafii nekk mou nexx mou nakharii certaines personnes t'as révolutionné la musique sénégalaise tes clips sont au top on te kiffe bientôt in sha Allâh tu vas détrôner le roi le monde entier va signer et être d'accord que t'es le prince le vrai roi "celui qui te détestait hier s'il t'accepte, s'agenouille devant toi aujourd'hui c'est que t'as bien cravaché" faramaréne
Je suis Malienne et amoureuse 🥰 de la musique Sénégalaise. Wally ballago Seck il est très talentueux. Sa musique est universelle. Je n'y comprends rien, mais ces chansons me font voyager MASHALLA. J'espère qu'un jour je visiterai le Sénégal juste pour le regarder en live inshallah 🙏🏽
Waynga li ci nienio yi ci taxi love ba dèsolé ndakh daflay dall ngay yobeunté gouney walyé simphonie bi baye fallou déyé seuh yaye ak ndiouga dieng thia wakeur gaye Massar. Wally no def? Ay lii di 😭❤️🤦🏾♂️
Wally nioune say fans laniou tei bgouniu beneu yoneu niak leu. Tei gua bayi di def clip di yeik si ay terass may wakh guay tiatal hum baxna rk😏😎 Sinan tu tapes fort encore😍❤
Wally khalé bi khéwe si diamono tamite sa weuye même sou amoul mbalakh damaye fethieu baye khalangou Wally khalé bou parer bi Wally khalé bou nieupeu beugeu Wally le meilleur de sa génération Wally 0 faute Wally machallah boula dara diaral changer Kone ngayi naniou dal way😚😙😚😙 kou d'accord mayma pouce bleue✌👅❤🖒
Wally wolof néna doneu sa maye door sa baye moko gueune mais yaw deugeu deugeu doneu gua sa baye si ay paroles ba paré door ko yalla na sa diam yageu seck💪💪💪💪
@@papito8025 non je ne parlais pas de cette album même si elle est riche musicalement sur nos bases nationales. Cependant, je parlais de son album internationale que j'ai eu la chance d'écouter quelques extraits vraiment formidable. De ce fait, si la pub passe vraiment il peut avoir les 500K de ventes pour avoir le disque diamant. En plus, le disque d'or c'est que 50K de ventes et disque de platine 100K en France ainsi qu au Sénégal et dans les pays francophones (Suisse, Belgique, Québec + les pays africains)
Pouce Bleu avant le visionnage !!!
Waa liii nekhoul💪🏿🤳🏿👏🏿
Li neh neh naa dra douko dakheu dra douko dakheu
Bilay ma contente si yow sama khol mogui nekh
@dßßzs2ßqdiatoukouleur2020
aà@@mamy3231
Waouu clip bii nekhna trop no wally seck mo dakk way si sénégal c magnifique extraordinaire j'apprécie beaucoup
😴😴😴😴
2025🎉🎉🎉 problème cast xawma kégne lay diekh Senegal mais nioune jeune yii war nagne ko dindi c'est possible mane deh inchallah rabi souma yallah mayé dom koumou beugs souma xolé djikom doyma ma mayéko bou féké dijoulit la 🎉🎉ndakh moy deug lolou la yallah wakh nioune niepou bénn lagne kénn geunoul kénn nio yém fa yallah ou❤❤❤❤
barki yalla 14h lay khaar clip bi ba diaréfa nélaw mangui sog di yewou bilahi
khaw'ma wally noumakoy def rk ana koumay may j'aime
Maniit d xawma louma ligayy tayy...ndax di khar clip bi rek
mbaye sy mdrr xalé bi dako diar nak
wayé yalla baxna nagn ko nianal rk
Qqqq mollo ppm 0m0q@@mbayesy9519
Waouh magnifique ! akka bari dollé sougnou Baye Fall bi ; Que Dieu vous protége . One love
🤣😎🤠🙏🖕🤳💪👏👌👍💙💘💋💝🌹🥀
Qui est en 2020 ? Yalla naniou yalla défal atoum khewel ak diam
Nga « Yobante « ma , ma fasiyene doug si « taxi love « dioubali esplanade grand théâtre waw « dafmay dal « ! 👑♥️
Dangay sétt lii rek
Quelle inspiration!
🥰🥰
fofa tothie
Waouh magnifik experience
Douma fans Wally waay song bi mom dafmaye dall douma deklou malax Loubari sah waay song bi mom everyday dinako deklou maa shaa Allah keep it up bro
Non son bi dafa dal
5,6millions de vues yi 1000 yi mane la ndeysane wally bamou May May dokhane 2010 wa waagniko niko douma sa morom yallah waxoul ken dara
Seul le travail paie et Waly le sait c’est pour cela il répond jamais au question inutile ni aux attaques de certaines sénégalais et sénégalaise qui n’aiment pas voir un jeune qui avance et qui travail pour son pays yalla na khole yi ceddd si barkhé seydina mouhamed psl et joyeux anniversaire waly longue vie à toi
"Dafmay dal" lou bari gua "Yobante" ma defois ma dougou "taxi love" Di doundou paridise Wally yafii nekk
Rsasdfhhjk
Barki yonètibi il est le meilleur 💪❤️3 clips si 2 mois 😍Maryacine yalla na yalla weiral bateu ganiouy beigual chak jour☺️Way kateu 🎤❤️yalla mousseul leu si say noneu ak keip koula bgue feixèl🙏🙏
amine way 💖💞💖💞😘😙😘😙💖💞👍👍
Dama begue waye wi man anta dafma yobou fou sori ya mana waye
Thiey wali defatina meuniname machallah sma faramarene bii yallana yalla wéreul bate bii la voie dor de la musique sénégalais borome le 27/4 ngaye fii No grande théâtre dou yombé nonou dina melni sabarou lébou kou nekh di danou aye rape 😍 wa lii nexoul kou contane si mome maye ma j'aime svpl j vous en prix
Notre Wally national yallah Nala yallah defar diam goudou fane ak wergou yaram. bien Des choses à toi. Yallah gua AME disque d'or ak disque de platine
Qui est la en 2024❤🎉🎉
Wa lii nékhoul 3 clips en un mois ❤️ Wally Yalna sa diam yague way 🙏
Nekhna
Kou yakame ti heure bi diote beuseule jaime❤️
Wally seck ceux qui disaient que legui ngua fay lol depuis combien d'années batey, avancement rek laniou guisss mashala, derrière chaque grand homme il ya une femme spéciale, mashala à toi l'artiste de sa génération
Le King est de retour je suis guinéen vraiment je vous j'aime Seck moi sait moustapha bayo je suis guinéenne habite Strasbourg que le bon dieu vous bénisse
moustapha bayo le meilleur
Merci adamabella diallo que dieu vous bénisse sait grâce à wally Seck que musique sénégalais ce rejonne dans le monde en entier
@@moustaphabayo1827 merci d'avoir aimé notre wally c notre fierté 🙏🙏😍😍
Machalah balago seck waly
kou d'accord ni waly validé na disque d'or bi tapel bleue ay guiss
Je suis d'accord
❤son billahi meunou mako mougn ❤❤❤❤ merci mar'seck pour cette merveilleuse
Merci de nous rendre heureux joie bimay am soumalay setane est inexplicable yalla nala souniou borom sam mouseuleu thi say none.
Koula bagne Yalnako tanguayou Kaolack bi rayy😂 kou yeiné wally travail l Disk d'or clik Jaime boudé deugeuleu Manifesté vs les Pure faramaren 😎🤗😍
Thioune Saghor 😂😂😂😂yagui togne wa kaolack yi
@@seynabouniass6495 fofou la deuk dih 😂
Thioune Saghor billahi sa wayy louma meune tii ame sa ma adouna kaolack momako ngeuneulll
koudoul doyal si song bi pouss jaim tellement nex 😍😍
Yalna melni mome
Yalna melni mome
@@mamidiouf9660 ijkhjhkhkgjrukgjk7653👑💍👑
2024
𝐁𝐥𝐲 𝐢𝐨𝐞❤❤
Wally Lou mou bokoul neikhoul lolou la yalla dogal Lila wakh 💥💥🔥🔥👑👑🎂 🎂.
Wally dafa tangue teh hamoléne loulu
3 clip dans un moi il est le premier musiciens à le faire wali nehoul😂
Yobanté
Taxi love
Dafemay dal
Ohhhh 😍 😍 mané kou beug Wally pouce bleu mu dalgnu😂😍
mane yobanté moma dakale mais bi tamit dalna 😍💪❤️
Billah liguey rek mo wor😍
Wally je le jure devant dieu sui tellement obcèdè par tes chanson que je n'arrive plus a écouter d'autres chanson qui n'est pas le votre bilay
Vraiment demb bou Wally family demeii prison forbet xoll yeup toy na maryacine prisonnier content naniou si yow weuyalll nanioula fethiall leu donc lolou tamitt dafniou dall niouy def you bakh yoyou teii leup yako waralll amalll diam rekkkj
Dafmay dall naniou dall niou and ak mom ba grand théâtre 😍😍🤔
Doudou ndiaye faye ❤️❤️❤️❤️
Tanks ❤️❤️🙏🏿🙏🏿
Machallah joli clip #team_faramareen ani gnoufi nek avant les 1millions de vues 💃💃💃💃💃💃💃💃💃 hbd waly wa li nekhoul tamit
Wa walay ay way ni la warra mel wa li nekhoul WBS ❤
*Ana gni geum ni wally mo dake woy Sénégal kom man nimako geumé😍🤟*
*_Magni nii fall_*
Haaa clip ni lay mel way faramareen bi dal ya fekhal khol yi❤️❤️❤️❤️💃🏽💃🏽💃🏽
machala tous derrière waly seck Musique Sénégal yako yoré qui est d'accord et bonne continuation
Moi wally rek 💃💃❤️❤️❤️
Suis pas mélomane mais waly lo woy nehneu meu
Je t'aime depuis la première fois que je t'ai vu sur le clip de papa thione batey xawma kagne lalay giss nak😏😍
ANA nieko beugue💖💖💖wanéléne sen boop👍👍👍
Wally est un monstre de la musique sénégalaise je suis peulh mais je l'aime il a une très très belle voix .
La question reste à savoir combien de personnes écoute en pleurant ça musique.
J'ai pas eu la chance de te rencontrer pour mais vous voyez presque chaque fois dans mon coeur continu de les faire vibrer.
O.o
No Wally star ga🇬🇲
Félicitations encore tu fais notre fierté ❤️❤️. Mais j'aimerais bien le voir avec sa femme dans une de ces vidéos,kou d'accord akh Mane?😍
Je croyais mm k c'était sa femme
@@tutojoubuzness4642 mm moi
@@ndiayadiouck6371 .
.
.hn z. Wn
M
M .
M
Z.z
..ñ ,
. Fm . Nnn u
V
Parfaitement d'accord avec vous
Oui une belle et sublime femme j'ai hâte qu'elle apparaît dans un clip ❤
Nice nice nice vraimen jai plus les mots Waly Waly Waly loumala wara wakh Bilahi khamatoumako khana nianalla goudou fane rek yalla weral bateu bi Bilahi beuguenala
😭😩😩ohhhh cette chanson
Kou beuga deim demain grand théâtre touche bleu
Beugu dem takhoul ngua dem😓
Racky Racky kone yaw danga beuga deim nii
@@zaletheboss7590 wawaw pire
Racky Racky d’accord weit ma légui légui
@@zaletheboss7590 daccord
Ah on est vraiment gâté ak Wally rek ci xol lénéne dafa xadioul yamaléne geunal
Nice macha Allah laff thiat waayy yalla na yalla def diam lépay bakh incha allah mane ma beugue niit bou ame fitt waly for rever
Une clip simple pas de roumkh roumkh ni de rambaxh rambaxh ohhhh klk jaime rkk😂😂😂 ani FARAMAREN yi
Nio gui niiii
Les images sont belles mais le scénario n'y est pas
Nice na
Nice na trop Wally seck machallah jtm❤
Simplicité yeufeum la
Manguii nii tokk di wait 16h00 moumay dall ni makoy yeuk waw kay ❤😉seck Ndanaan
Papà lo deffff mou nekh gnou titou nou on attend avec impatience depuis la 🇫🇷🇫🇷🇫🇷🇫🇷🇫🇷
Souniou Papa
Yaw goor ga ni ba tok?
Wou suis depuis gabon mai suis impatiente et 17h senegal c 18h ici depuis le matin je ne fait que attendre machala way😊😊😊😊😊
machalla lo defe mou nekhe borome kholou grand théâtre
@@awzndoy6988 no amoul morrom
Wally fis boul fatè limala wakhon music Senegal yaniou si doy tèk naniou ko sa lokho sei grave vai in analisi Grazie ancora papi Torino from Torino
Wally seck le LM10(Leo Messi10) de la musique sénégalaise.
Quand tu es sur le banc( tu ne sors pas un album) le match( scène musicale) est sans saveur, aucun frisson
dès que tu foule la pelouse( tu publies un son ) la population est en ébullition.
Tu marques un but ( tu joue sur scène) nous le célébrons tout cœur avec toi, les scènes de liesse et de joie sont innombrables.
Que Dieu te protège. AMINE.
C'est le meilleur
Wally 9 cavani
0
Ana gni Aimez avant clip bi mane yeine la geumm nakaté 😘❤️👍
lima guene ray si son bi moy fimouné "esiii yama leen gueneul sokhna" tu es la source d vie wally l king j t'ador ❤
Ohhhhh ay founiou dieum je taime wally je taim tres fort g meme pa les mots♡♡♡♡
Kou d'accord ni sokhna aidara mo warone def clip bi beuseul jaim
D'accord
Qui est d'accord que wally seck est le chanteur du peuple 😍😍🤗
😘😘
Si
Ani gnimouy dall wayy pousse bleu🤗 gonégui seck dinama rayy rkk😍
Niogui ni
cheikh nouha cheikh nouha t
Laf thiat sougnou faramaren bi et bn annif long vie santé de fer réussite totale rek inchallah
C'est le meilleur
Daf may dal ba 2022 tout droit
l'exclave de la passion, l'homme à qui la musique coule dans ses veines, un talent bien confirmé, du savoir faire incontestable. le poète dakarois, l rossignol de la musique Sénégalaise, l'un des paroliers de la musique Sénégalaise et l meilleur de sa génération : Wally Ballago Seck
Wa ki nexoul
C'est le meilleur tous les jours meilleurs
Wa deggeul lii👋👋👋
Fabinta Fall esk li dakoul nékh chu ?
Juniior Wally Lofficiel fofou tothie radiakh
Yobanté Taxi Love Clip yoyou yeup rafeet na teh diarna yoon et ses clip vidéos sont très bien réalisés waayé Clip bi Dafmay Dal moma dakkal parceque daffa simple teh bariwoul nitt j'aime ça mane dama beug lou simple beugouma lou xoumb dina amm 100 personnes ci Vidéo Clip lolou day diaxasso bougouma lolou 3 personne ci clip rekk baxna 2 et 1 danseur ça suffit motaax Dafmay Dal nignouko réalisé neexnama en plus Clip bi da seet wethie saltewoul machaalah🙏 trope mais n'empêche Yobanté c'est ma chanson préférée dans l'album #Symphonie Nice Wally Machaalah🙏et Bonne continuation!🙏
Am na KO kham ni clipa bam kom sabar bou tass ak jeu de lumiére
@@babacarngom6751 Pape Diouf leu amoul saax laam lamé moy deff yoyou daffa beug lou xoumbou moom artistes Sénégalais yii yeup gnoko taané ci clip daffa beug clip bou amm ayy jeux de lumières
Wally Séck Mon chanteur préféré , yalla nala yalla lafalle thiate
6000 vues sii 16h08 mnt kein dou iowwwww seckkkkk😘😍💋💋💋❤❤❤
Sénégal danion am diott motakh vus yi barry
Cheikhouna Gaye iow dh amo djiot
Eupnako billahi
Enfin un.clip simple .... sans groupe de fethie kaat j'adore Gud luck Waly
Papa fall diam thi yaw yaw sa clip nena mout🤩😍👍👍
Qui a déjà son billet 🙋 wally family ana nguégn💕👍
Varoukh Aidara TV j ai déjà mon billet
@@ndeyediagne2644 WawaW man iow la gueme
waw keuy
kouy door mo mane kouy saaga
1 semaine 2 clip wa li néxoulll !!!!
Billahi dosén morom mala begueu yalla nala yalla sameu borom kholou diamant.
Ani gniy dem souba esplanade Grand Théâtre inchala
Niogui
Niogui bilay
J'estime trop Wally laf thiat faramarène bi Ma Sha Allah. Douma doyal si mome walahi
Pape thione dissa baye 🥰 diaga dissa yaye 🥰 chérie soxna aidara 🥰 bayou ndella, momy ak mouhamed 🥰 domou yayou eumeudi badiane 🥰 magou As7 🥰 magou bintou rassoul 🥰 magou Aïcha rassoul 🥰 magou babacar seck 🥰 magou mouhamed rassoul 🥰 momy dany gueye dissa mak 🥰 lamine naar gawlo dissa makk 🥰 brom penc mi, vogue,esplanade GT, bercy, dome de Paris,Genève, etc.......le chanteur du peuple faramareen bi 🥰 le choix du peuple 🥰 l'erithiers des faramareen 🥰 brom faramareen musique 🥰 brom raam daan 🥰 déngay wayy ba sagar khégne 💪❤ ( deejah waly )
Lèer namani clip bi moy dakk dall jtm💖
Wa Li Nekhoull Ana Borom Kholl You Sett Yii Ta Refet ☝💪💪❤❤❤❤❤
MaaN DeH MaGui Nii
😅😅😅😅
Wawa
gnokini way💖💖💖💖💖💞💞💞💞💞😃😍😚😅😗
gnogini tok rek
Même pas 3h de temps +100k wa li nexoul❤😘
Wally the king👑 mangui xar disque d'or bi🙏❓
Nekhna
Tropeuh✔
Yafii nekk mou nexx mou nakharii certaines personnes t'as révolutionné la musique sénégalaise tes clips sont au top on te kiffe bientôt in sha Allâh tu vas détrôner le roi le monde entier va signer et être d'accord que t'es le prince le vrai roi "celui qui te détestait hier s'il t'accepte, s'agenouille devant toi aujourd'hui c'est que t'as bien cravaché" faramaréne
*_Lou leir fall_*
i miss u mr
Je suis Malienne et amoureuse 🥰 de la musique Sénégalaise. Wally ballago Seck il est très talentueux. Sa musique est universelle. Je n'y comprends rien, mais ces chansons me font voyager MASHALLA.
J'espère qu'un jour je visiterai le Sénégal juste pour le regarder en live inshallah 🙏🏽
Et si je t'apprends notre langue
@@elhadjidaoudacamara6803moi je veux bien
Khale bi lay weure ba minuit ma deuti le jeune pharamareen guay ame fofou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Qui voie que waly est le meilleur de sa gènèration et il fait tout pour satisfaire a ces fan's pousse bleu
Bilahi Wally clip bi mom sokhna ngasi worone guéné kone nga todiatifi worna GoD
J regarde l clip sans être fatiguer
Aÿ Wally 1 mois rek 3 vidéo wa li nékhoul kou contane si faramareen bi mayma j'aime Khamna sah 5 wala 10 jm lay am😍😍😍😍
Machalah dal😍
Waly dou aye fo laftiate watie gua fi ba zéro
Ki dal duma wakh thi mom
@@dadosarr7945 ok
J'aime xana lii nexna tmt
Wa li tamite nekhoul rek 😘😘😘😘 je veux des j'aime svp🙏🙏❣️❣️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Nékh na kay
Kou beug Wally beuseul j’aime 👍
Teusss Rekkk
Waynga li ci nienio yi ci taxi love ba dèsolé ndakh daflay dall ngay yobeunté gouney walyé simphonie bi baye fallou déyé seuh yaye ak ndiouga dieng thia wakeur gaye Massar. Wally no def? Ay lii di 😭❤️🤦🏾♂️
Wa li nekhoul
Amna louma mety nak ndakh douma dem grande théâtre 🙈🙈
Sétna ba sétt néxoul ba nexoul wayé Wally li nguay déff nexna tropp...
Walahi tu es trop fort machallah mon grand laf thiat je t'aime bcp 😘😘😘
Dieureudieuf serigne touba mbacké pouce bleu 🙏
nga balma mai Ahmadou Bamba boulko bolé si yi
@@boussothiamsaliou8076 ahh wax deugg yalla
Wally nioune say fans laniou tei bgouniu beneu yoneu niak leu.
Tei gua bayi di def clip di yeik si ay terass may wakh guay tiatal hum baxna rk😏😎
Sinan tu tapes fort encore😍❤
Slt à tous clip bii nekh na machallah mais mane taxi love akk yobanté moma dakal vraiment 👍😘😘
Defati gua sa meunine machalla meilleur vidéo de l’année ❤️❤️
Wally khalé bi khéwe si diamono tamite sa weuye même sou amoul mbalakh damaye fethieu baye khalangou
Wally khalé bou parer bi
Wally khalé bou nieupeu beugeu
Wally le meilleur de sa génération
Wally 0 faute
Wally machallah boula dara diaral changer
Kone ngayi naniou dal way😚😙😚😙 kou d'accord mayma pouce bleue✌👅❤🖒
Kou geumni wally dina dieul disk d'or beusseul bleu❤🤘
Meilleur chanteur africain
Kou dacord pouss bleu👍👍✔
💪💪💪
Wally wolof néna doneu sa maye door sa baye moko gueune mais yaw deugeu deugeu doneu gua sa baye si ay paroles ba paré door ko yalla na sa diam yageu seck💪💪💪💪
Disque D'or Rek Inchaallah 🎤🎤🎤
Clip bi dal amna class wawaw zéro khomb merci papa waly🥰🙏🏼
anni gniko beug manifestez-vous 👑❤️🎉🎉🎉🎉
boron anniversaire 🍰 bagui nonou❤️👑🎂🎉🎉🎉🎊
athieu na bleu👍
Waly fait doucement sinon tu va tué les jaloux
😂😂😂😂
Tamit
Mari Cissokho ????
Ils n'ont qu'a mourir 😂😂😂
Affaire bi faramarene leu nay nagou li yalla dogal so nagouwoul nak diga trokh sa khôl di diekh 💯💯💯
Thiootou Xonam kii il es dangerous dh nakoo brom bi lafal thiaat rk ak kepp kou aimer commentaire bii❤💕
Saga yi nak
Lou tchi sa yoon
Kou beug Wally Seck ameu disque d'or wala diamant na beus aime
1k de like merci j'avais pas vu ❤️❤️
black_ power_ genrou son yi mayé woul disque d’or dei 😂😂😂 toutes ses chansons yeup nouro mais nekhna est ndaw yi 🤣
magui ni
Je suis la
@@papito8025 non je ne parlais pas de cette album même si elle est riche musicalement sur nos bases nationales. Cependant, je parlais de son album internationale que j'ai eu la chance d'écouter quelques extraits vraiment formidable. De ce fait, si la pub passe vraiment il peut avoir les 500K de ventes pour avoir le disque diamant. En plus, le disque d'or c'est que 50K de ventes et disque de platine 100K en France ainsi qu au Sénégal et dans les pays francophones (Suisse, Belgique, Québec + les pays africains)
@@papito8025 Tu as parfaitement raison
Les pas de danse🕺🏼 de Ame bongo me fument 😂😂😂😂🔥on t’aime Wally❤️🥰
Encore Wally seck on Va ou a toi merci beaucoup