🚨Moussa Ndoye, Ada Fass Chez Satouba 😱après son combat contre Mbaye Gouye gui, images bou rafet xol

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 янв 2025

Комментарии • 135

  • @OriginalboyTown
    @OriginalboyTown Месяц назад +12

    Ouakam la deuk félicitations Moussa Ndoye lebou dou ragale aythia 🎉 ada ndakarou BOROM DEUK bi yaw rek Lay topou 🎉Town seul

  • @serignemodouciss7270
    @serignemodouciss7270 Месяц назад +24

    Talibé cheikh bou diékk si Hisbou ngua so wato aussi dinasi bakh
    Lii diapou nala dh ❤ machALLAH

    • @pacosuzanetv
      @pacosuzanetv Месяц назад +3

      Ki wara watou kay moy azoura

    • @deugrek344
      @deugrek344 Месяц назад

      Lernala nii dieul na wird?wala pour yaw talibé cheikh thie lamégne la yam.

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Месяц назад +24

    WEUZ DIAMBAR FUTUR ROI DES ARÉNES LE RÉVOLUTIONNAIRE DE LA LUTTE DE YARAKH DIARAMA DIAMBAR ❤

  • @hamzafall5475
    @hamzafall5475 Месяц назад +2

    Depuis Londres...Way lii nekhna Way billahi... Felicitations Moussa Ndoye... et surtout Weuz Diambar... Sa Touba doundeul Way... diamm si yènn rekk yaaram

  • @bayemoussathioune50
    @bayemoussathioune50 Месяц назад +1

    Félicitations moussa ndoye dila bégué depuis Italy 🇸🇳🇮🇹🇮🇹🇸🇳🇮🇹

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Месяц назад +6

    Machallah li rafetna trop ❤❤❤

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 Месяц назад +1

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mendypierre5726
    @mendypierre5726 Месяц назад +6

    Moussa ndoye daafa bokk si lamb dji félicitation mbeur maayal boy yi chance Gua mbeuré

  • @mynameis6391
    @mynameis6391 Месяц назад +9

    Sa Touba nitt kou bakh le mashallah

  • @Yorodiaw787
    @Yorodiaw787 Месяц назад +25

    Moussa Ndoye vs Tapha tine
    Kou d'accord lalale j'aime

  • @mamadoudiop1105
    @mamadoudiop1105 Месяц назад +8

    Moussa man yaw la faralon mais tu te concentre trop sur le mystik

  • @JazzCheikh
    @JazzCheikh Месяц назад +3

    Ay adversaires ngueine dee moussa NDOYE/ada fass

  • @SidyToure-mv5eg
    @SidyToure-mv5eg Месяц назад +5

    Machalla 🤲🤲🙏

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 Месяц назад +4

    Machallah ❤

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf Месяц назад +7

    je vois à sa Touba nit kou bakh te oyof bilahi

  • @magorthiam829
    @magorthiam829 Месяц назад +9

    Moussa ndoye/Serigne Ndiaye 2

  • @bayemoussathioune50
    @bayemoussathioune50 Месяц назад +1

    Moussa ndoye talibé piir machalla

  • @mamadoudiop5250
    @mamadoudiop5250 Месяц назад +7

    Moussa ndoye vs eumeu sene

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Месяц назад +7

    MOUSSA NDOYE KASSÉ LÉBOU BI LE REQUIN NOIR DE YARAKH YA MEUNE YA EUPEU DOLÉ YA GUEUNEU NIÉMÉ THIONO KHANA DOMA DÉGUEU ❤

  • @papefall7062
    @papefall7062 Месяц назад +2

    Weuz diambar , khol bou raffet la yor, il fait tout avec le coeur / mach'Allah. Sa touba , deil nebeutou si on te voit avec plusieurs lutteurs. Yarakh vous êtes sur la bonne voie.❤❤

  • @youssouphandour2056
    @youssouphandour2056 Месяц назад +1

    Lac Rose était malade ne cite pas, c'était son premiér combat aprés sa maladie.

  • @serignemansourtoure86
    @serignemansourtoure86 Месяц назад +1

    ADA NDAKAROU TEMPS YI YAROUNA DEH 😂😂😂

  • @modourokhaya9616
    @modourokhaya9616 Месяц назад +11

    Moussa dè mi Ngui melnè baye makka samb dieuwrignene Dahira mafaatihoul bissri Brooklyn, new York.

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye Месяц назад +3

    Aliou kaïré d'ou dara 😕 simple courrier la d'ou sérigne

  • @AladjiMbaye-s1c
    @AladjiMbaye-s1c Месяц назад +1

    Sa geumeul yalla féne bakhoul

  • @BambaDiagne-w4m
    @BambaDiagne-w4m Месяц назад +2

    Mai sa Touba khana niepp ay mbeureum laniou

  • @daamndiaye4412
    @daamndiaye4412 Месяц назад +1

    Moussa ndoye gris 2

  • @freesenegal12345
    @freesenegal12345 Месяц назад +1

    Moussa Ndoye neu may Jacob baldé chance

  • @mansourndiaye3391
    @mansourndiaye3391 Месяц назад +2

    Bilaye Lamboji Dina yakhou li gui taye moussa ndoye ne doma beure AK Ada fasse

  • @kenzykindkeinde38
    @kenzykindkeinde38 Месяц назад +2

    MOUSSA NDOYE VS SERIGNE NDIAYE 2

  • @falloufall8232
    @falloufall8232 Месяц назад +4

    Weuzz diambar sa tour wi doyna firna diambar deugu moy iao

  • @madikebop5717
    @madikebop5717 Месяц назад +3

    Weuz diambar iao moussa ndoye contre lac rose malgré bléssure lac rose ak lou khékh bii métii yeup moussa ndoye moy guén sakou yii malgré lac rose déf na abbandont par bléssure mai moussa ndoye comba bobou mo dieul 3 avairtisement lac rose 2 avertisment moussa ndoye tapét la na dieul gris 2

    • @gorandiaye7648
      @gorandiaye7648 Месяц назад

      Kan mo daw combat bi nane daniouko lokhi si beut

  • @DameSalle-b8k
    @DameSalle-b8k Месяц назад +3

    Wa li niroo la wala ada fass😅

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 Месяц назад +3

    Baye lahd bi refetna loll

  • @ibrahimatine2369
    @ibrahimatine2369 Месяц назад

    Weuzz Diambar nit kou bakh la

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo Месяц назад +4

    Sa Touba day napé rék nakh na mbeur yi moussa ndoye ya meune Mbaye gouygui mais hamnagn koula meune

  • @SèkceMbaye
    @SèkceMbaye Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MameBoromB
    @MameBoromB Месяц назад

    ما شا ء الله موسي😂

  • @ebrimaceesay7728
    @ebrimaceesay7728 Месяц назад +2

    Belie Sa Touba Dor kat la

  • @KhassimSene-hp6ot
    @KhassimSene-hp6ot Месяц назад

    Moussa ndoye dioum nga waro won wakh Lila sa Touba wakh

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw Месяц назад +4

    Bayilén Di Feuseul Baatin Boun̈la Deeyé Dara Boulko Wah Fi ak Pasé Wul Sino Rk Mana Yakh Lou Bari 4 Combat lala Wah Bén mo Pasé ngay Wah Amna nio Xamni Danio Soxor Dan̈i Fek Mbir mou Sén Yon nekul Niou Sot la nguir kîgay toud Ban̈a Am Ndam

  • @TallaNdao-ul8vs
    @TallaNdao-ul8vs Месяц назад +2

    ❤❤❤❤❤

  • @ProcureurYoutube
    @ProcureurYoutube Месяц назад +3

    Sa Touba amneu promo nak😂😂😂

    • @mbodjmori4977
      @mbodjmori4977 Месяц назад +1

      😂😂mbeur si bopam nionwayadi

  • @BadaraGueye-ii5gh
    @BadaraGueye-ii5gh Месяц назад +3

    Comba gora sokh Moussa ndoy lamb Bou nekh la

    • @elman1683
      @elman1683 Месяц назад

      Avant mbaye mom lagn warone may chance mais dafa rew na jeul weuz après

    • @moustaphadiop8903
      @moustaphadiop8903 Месяц назад

      Wala guéne war lou noye rk😂

  • @abrahamsamb6596
    @abrahamsamb6596 Месяц назад

    Waaakhh deugu sa touba xariittt yeppp concentre toi cé mieux

  • @booygaye9894
    @booygaye9894 Месяц назад +1

    Waa Ada fass la guiss ni wala 😂

    • @zoladiop9412
      @zoladiop9412 Месяц назад +2

      Mom la beugon binde nii😂

    • @booygaye9894
      @booygaye9894 Месяц назад +1

      @ loumouy deff fii la xamoul booy bi daal diaxal nama

  • @fayeousseynou8430
    @fayeousseynou8430 Месяц назад +1

    Niit meno nek fepppp !!!!

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 Месяц назад +2

    Ma sa touba mii daa manoul yamm femm 😂😂😂mouy weurr nii rek 😂😂😂😂

  • @ice4682
    @ice4682 Месяц назад +1

    Mais wadji khanaa gneup lay gnanal

  • @BassirouSamb-oe6sh
    @BassirouSamb-oe6sh Месяц назад

    M'a Ada fass khana demoul voyage

  • @PapeSow-l2d
    @PapeSow-l2d Месяц назад

    Kii mome seytane leu koi sa touba dafa beug nk féep lolou menoul nk mbeur yeup nek ak yaw limouy beug giss lénn ma

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 Месяц назад

    Sa touba. 😂 sa legui mou wote tarikha d 😅

  • @mouhamedfall9708
    @mouhamedfall9708 Месяц назад

    Ki geumoul boppam kw sa touba boppam rek lafi nekal

  • @DameSalle-b8k
    @DameSalle-b8k Месяц назад

    Lambe dji diakhasona d

  • @AllaDieye-eg6nj
    @AllaDieye-eg6nj Месяц назад

    Soula mbaye Gouy gui diapone ka khamné lep deugla

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 Месяц назад +51

    Sa touba dafa nara yakh lamb.. soyons sérieux .. meuno nianal mbeur yeup en même temps

    • @pmsdiouf
      @pmsdiouf Месяц назад +15

      DAY LIGUEY

    • @aichasecka-8974
      @aichasecka-8974 Месяц назад +4

      Day ligueye waaa

    • @MbayeThioumb
      @MbayeThioumb Месяц назад +2

      Blh Lou lerr gua wax

    • @MbayeThioumb
      @MbayeThioumb Месяц назад +2

      ​@@pmsdioufni lay liguey xana waxoul ni baol la deuk

    • @BocarAnne-g7d
      @BocarAnne-g7d Месяц назад +2

      Sa Touba di thiaga day weur rék visibilité lay weur

  • @pacosuzanetv
    @pacosuzanetv Месяц назад

    Sa touba soff ga tropp yaw meuno ande ak mbeur yeuppp

  • @karbalasow8234
    @karbalasow8234 Месяц назад

    Sa touba fou néke nga nékefa yalla rek rek rek la digue fall tu fais fais q du théâtre

  • @baracisse2717
    @baracisse2717 Месяц назад

    Sa touba aka mana bandit bandilou té courtier marabout rek la😂😂

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 Месяц назад

    ❤❤❤❤