Voici le véritable générique adapté à cette émission de lutte TV. Il s'agit de Saraba ; classique mandingue, popularisé par Samba Diabaré Samb .Voici la musique des lutteurs et des turfistes. Aziz a même remporté un tournoi des amateurs. C'est dire la passion héréditaire de cette famille. La lutte a fait preuve d'ingratitude envers moi. L'arène nationale, c'est moi. 😊😊
Machalah baye ndiaye ❤nila dh am kilifa moy li am solo boko amé amgua solo boko amoul amo solo walahi ❤️Machalah yalna Diam yague waay ndiaye Man balla rk motakh ma begue la ❤wayé tay dji yokona dakh sa am yar Machalah ❤
Vraiment là famille est très sacré merci beaucoup Aziz Un grand merci à Lamine et lutte TV je suis l'aîné je veille beaucoup à eux mais c'est témoignage me rend encore fort pour veiller à eux Un charitié bien ordonnée commence par chacun de lui même
Machalakh amenei solo torop émission bi defois daay bakh guene dii invite des personnes populaires niou wakh senne djiare djiare mais moi j'aime bien lamine il est très discipline et correcte aussi baye Ndiaye yala bakhnei Aziz c'est ton grand frère
Ohhhhhh baye ndiaye diamb si yaw que le bon dieu vous protège tw et aziz, vous accorde une longue vie, jusqu'à vos 100 ans que cette relation soit éternelle, que dieu vous vous protège de Satan dans cette relation par la grâce de dieu et son prophète psl je suis éblouie de la gentillesse de aziz ndiaye à l'égard de ses proches quel homme exceptionnel ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Très belle émission mais fallait prendre bénene générique étant donné que émission dagne kumpa c'est le même générique lagnou done utilisé séne émission donc fallait au moins dieul bénene wayou thiossane apporté votre propre touche
Três bonne émission et pleine d’enseignements 🙌🏽👍🏽 Lamine good JOB aussi mais évite de laisser le vide quand tes évités sont dans l’émotion pour les ramener. Sinon le reste falaw 🤌🏽 Li warna diagual gnou bari ci sène dokholine. J’ai un grand frère qui est comme un père pour moi. Dioyouma takhawaye wadjour fène 🤲🏽. Yallah nalène same te are lène 🤲🏽🙌🏽
Aziz ndiaye c'est un exemple de reussite liguèye rekkkk mo woorrrr billahi machallahh un homme doit travailler
Familles ndiaye ndiaye ngiep yallah na yallah défal lén diamou amine 🤲❤🤲❤🤲❤🤲❤🤲❤🤲❤
Voici le véritable générique adapté à cette émission de lutte TV. Il s'agit de Saraba ; classique mandingue, popularisé par Samba Diabaré Samb .Voici la musique des lutteurs et des turfistes. Aziz a même remporté un tournoi des amateurs. C'est dire la passion héréditaire de cette famille. La lutte a fait preuve d'ingratitude envers moi. L'arène nationale, c'est moi. 😊😊
La Sincérité dans les yeux de BAYE!!! Omgggg yaarou ngaaaaaa! Masha Allahou, yala na yala lafale leine Thiaaat🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Masha allahou raby Aziz dal kou khamoul ndekete khamo vraiment Aziz waliyou leu djambar leu ❤❤❤
L’amour de baye ndiaye à Aziz c’est Énorme
Très belle émission
Aziz c'est un exemple de gand frère bonne continuation machallahh il joue son rôle de grand fre
Machallah baye ndiaye kou bakh la mais kén dou alamine yalla nalén yalla arr dakhal lén seytané baye azizz ak balla gaye ak say xarit yip
Amine ya rabi
Machalah baye ndiaye ❤nila dh am kilifa moy li am solo boko amé amgua solo boko amoul amo solo walahi ❤️Machalah yalna Diam yague waay ndiaye
Man balla rk motakh ma begue la ❤wayé tay dji yokona dakh sa am yar Machalah ❤
YALLA na lene YALLA same ❤❤
Vraiment là famille est très sacré merci beaucoup Aziz Un grand merci à Lamine et lutte TV je suis l'aîné je veille beaucoup à eux mais c'est témoignage me rend encore fort pour veiller à eux Un charitié bien ordonnée commence par chacun de lui même
C'est triste yalla na sén diganté gauna ratakh, mai amga magu diou bakh machaala toi aussi rien à dire machaala laff thiatt
😢😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭kéndou Aziz Ndiaye 😢😢😢😢😢baye Ndiaye yaw tamit rakeu diou bakhna ❤❤❤❤
Baye Ndiaye yallanala yalla maye goudou fane ak wér😢😢😢😢😢😢 dieuredieuf
Machalakh amenei solo torop émission bi defois daay bakh guene dii invite des personnes populaires niou wakh senne djiare djiare mais moi j'aime bien lamine il est très discipline et correcte aussi baye Ndiaye yala bakhnei Aziz c'est ton grand frère
Deux jeunes très displine machalla
Manchalla grand frère li laye diarigne petit frère merci ❤❤❤❤
Kou beug balla ma beug la diadieuf baye Ndiaye ❤💯
Machala amena yar ak teguine c est le reflet de Aziz ndiaye
Baye ndiaye un homme avec un grand cœur véridique qui aime c’est ami big respect à toi mon frère
TOUS LES GRANDS FRERES DEVRAIENT PRENDRE EXEMPLE SUR AZIZ NDIAYE
Merci Aziz yalna yala takhawoulène mouseul lène ci thiate
Machalah yalna yalla samlen moussalen si seytanei
Vraiment baye kèn dou yaw bilahi nakk ❤❤❤
Baye Ndiaye nuit kou bakh nuit kou yorou nuit yek domou adama yale nala yalla defal diame ake wer mo frère diame rek gaye ame inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla mon frère bon courage pour toujours 🕋 🙏🏿
Amna solo mon frère machalla nite amoul loudoul mokame nite koubakh ga li ga wakhni gor rék moko meune big respect
Ohhhhhh baye ndiaye diamb si yaw que le bon dieu vous protège tw et aziz, vous accorde une longue vie, jusqu'à vos 100 ans que cette relation soit éternelle, que dieu vous vous protège de Satan dans cette relation par la grâce de dieu et son prophète psl je suis éblouie de la gentillesse de aziz ndiaye à l'égard de ses proches quel homme exceptionnel ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine ya rabi
Baye ndiaye mi dé nitbou am yar la machallah ❤❤❤❤❤
Chapeau à tout l'équipe de lutte tv ❤
Très belle émission mais fallait prendre bénene générique étant donné que émission dagne kumpa c'est le même générique lagnou done utilisé séne émission donc fallait au moins dieul bénene wayou thiossane apporté votre propre touche
Bien dit 😊
@@Enfant_béni_7 merci beaucoup pour l'appréciation 🤝🏽
I really appreciate y’a beaucoup de beatmaker comme iss 814 bril aussi
@@khadimbachir8072 parfaitement broh
Pourtant grand bilahi bi art la dh
Três bonne émission et pleine d’enseignements 🙌🏽👍🏽
Lamine good JOB aussi mais évite de laisser le vide quand tes évités sont dans l’émotion pour les ramener.
Sinon le reste falaw 🤌🏽
Li warna diagual gnou bari ci sène dokholine.
J’ai un grand frère qui est comme un père pour moi. Dioyouma takhawaye wadjour fène 🤲🏽. Yallah nalène same te are lène 🤲🏽🙌🏽
Kémaane leuh dh khaliss bi beurina machallah
Lamine machala très pro on te suivre de près wa gor
Yalna sa diam yag baye ❤
Yalla nalen yalla mousal si thiat si barké seydina mouhamed psl
Abdou Aziz ndiaye merci grand nit mbokam
La fratrie le sang sont très très forts .... Il faut en tirer des enseignements et des leçons des moralités....
Très belle émission azize mon indole bravo baye thi reconésent
Lutte Tv Bravo 🎉 . Lamine Courage À Toi Vous Faire Un Travail Super.
Machalla famille ndiaye yalla naléne yalla défal diam
No chapeau lamine tu es un grand profesionnell
Machalla famille Ndiaye
Respect a toi ,tu es sur une voie exceptionnelle,que Dieu te protège ❤🙏
Mashalla yalla nalén yalla defal diam
Très émouvant seul le travail paye,qu’Allah le tout puissant guide vos pas et vous protège contre les mauvais esprits.
Aziz dal YALLA na ko YALLA same ❤❤❤
Machalla yalla nalen yalla lafal thiate
Diadieuf baye ale nite daye am kilifeu et bonne continuation
Un vre frère baye ndiaye amal diame
Ame kilifeu ak talibé rek ngua ame solo aziz ak baye dal machallah yalnalen tiate sékhlou❤
Respect a baye ndiaye
Lamine machallah sagaw sa kanam ❤
Watching from the Gambia lutty tv keep it going because you people are doing a very good job definitely
Que le Bon Dieu consolide les liens parentaux
Bilaye ma beugg baye,khalei bou kileufeu thé nitte❤❤❤
Yalna Yalla geuneu samou sen digeunté ta yokhou sen Teranga bou bakh inch'Allah
Machallah bay ndiaye
Ndaysan yalla nalen yalla sameu
machiallah emissions bi amna solo baye yalla nala yalla baye ak sa frand frère abdou aziz
Sene yaye dji tamite doyna war di 🫣🤫
Yallana yalla deugarale sèndigantè si barké seyedina mouhamad
Machallah baye Nice na
Merci lutte tv chapeau à vous ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Aziz machallah merci Baye
Good job !!!
Lamine déllossi watnga dégue koumpa dh ❤❤
Que le dieu vous protége si barké seydina Mouhamed (PSL) il m’a fait pleuré 🙏
Cédé ti rafetena machalla
Lamine yalla n'ala yalla lafale thiate dale nga moune nga té dô wakh lou niaw lii daa raféte ❤❤❤❤
Ndaye sane dara amna solo lou bilaye sante naa yalla bama sy diaré ❤❤❤❤🙏🙏🙏
Aziz Ndiaye, niit ku baax leu
Bilay
ماشاء الله جميل باي جاي على اتباع أخيك
Baye yarouna mashallah
Machalla lamine nice jobs
Aziz genie la❤
Baye quel homme
Relation fort entre deux frères
Bilay fami yepa wara roy si yéne bilay yala na lene yala defal diamou
Vraiment kou d’accord ni baye ndiaye,et aziz ndiaye deniou meune comuniqué beuseul jaime ❤️
Lamine il ne faut pas laisser la personne pleurer comme ça dancoy dièma indiwaate
Mai machallah leup rafetena machallah
Yalla nalene yalla sam te lafal lene thiate
Aziz Walayy c'est lui qui m'a inspiré d'être comme ça avec mes frères et sœurs
MASHALLAH
Mashalla machalla li rafetna
Merci lamin ❤❤
Machalla li rafetna
Lutte tv chapeau à vous
J’ai toujours dit Aziz ndiaye diantalment leu
Baye Ndiaye la confirmer
Masha'Allah may Allah the almighty bless this family and all the family's too 🤝
Mais emison bi nekhna lole bon continuation lutte tv ❤❤❤❤
Amna solo yallna yalla lafal lene thiat
Macha allah ❤❤❤
Baye Ndiaye baloul gris Akk pass moment môme AK Balla Kone Yako togne balouko guéne nékat si diam mo Geun rafét
Le fond musical est très élevé par rapport à l'interwiew
Machallah
Bonjour vous pouvez me donner le non de ce musicien si vous plaît sa me fait tellement du bien ndeysan jai de larmes aux yeux 😢😢😢❤❤❤
Samba diabare samb titre (saraba)
Grand-père d'Aïda samb
Ndaye san baye iow borom bakh gua kou xoll lingay déff si balla gaye rk khamni kou bakh gua yalla nala yalla defal diam rk
MACHALLAH NIO BOKON DAARA FASS TOURE AKA BÈGON BMISKIT AK MÈW
Chapeau a lutte tv, bay ndiay toyalnga sama xol linga wakh si sa mak rafetne Barki alkhourane. Boucher vrai badoleu aussi khaliss rek lay diamou koi
Vraie badola balla c un con nit kou mel ni no meuné amé si mom confiance ba di ko confié sa mystique
Ly nékhe na waye
Li dafa rèfet❤