Pape Niang a reçu sa 2eme plaine venant de la part de Mbaye le mari de Ndiolé c'est du jamais vu

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025

Комментарии • 488

  • @aminatadieng9765
    @aminatadieng9765 11 дней назад +57

    Li Motakh niounane doff d’où weer day tané metinama déjà té sma yonn nekousi😂kou dem ba takal la diabar dessé toula draa ms lolou niit mokoy xalat courage pape niang lingay df silou bakh yalla nalako yalla faye Incha’Allah

  • @Kenza-bs8mu
    @Kenza-bs8mu 2 дня назад +1

    Ndiolé mii da melni jeukeur ji la faral deh😂, pape histoire bi c’est drôle 😅😅

  • @pispad.r.t4408
    @pispad.r.t4408 2 дня назад +1

    Kou fayonték ak doff mom doff nga
    Mbaye mi diaroul topp dh

  • @GoraFall-ys7ws
    @GoraFall-ys7ws 11 дней назад +27

    Qui weroul continuer rk yàlla gueummoul nellawoull❤avec courage

  • @YoussoufKeita-m4r
    @YoussoufKeita-m4r 12 дней назад +33

    Billahi pape boul décourager khamalni Yallah nguay liguéyél. Li nguay déf sé pas donner à tout le monde kon en avent té khamni Yallah moleu natou.respect à toi.

  • @MariamaDialla-x5q
    @MariamaDialla-x5q 11 дней назад +22

    Yew diam rek ngaye am incha'Allah u rabbi du courage tonton

  • @hyougojesais7239
    @hyougojesais7239 11 дней назад +23

    Yalna là yalla faye sa khol pape

  • @AdjidabaTop
    @AdjidabaTop 11 дней назад +22

    Dieuleul sa prore décision ki badola la khamoul yélla, def lou bah bagniu nar la sank dila plainte outal say matouway, ki déh mo yéss mbaye sow mi dou gor déh té du fatélikou dembeu moy badola deug, na guinde keur gui pape niang nah ki du kou bah, sétale si ndiolé sah ak niga sonné si sokhnam ni dale nala meuna fayé, boul si Sète yalla nah mom setoul si yalla, mo niak diom lane moy 1000, pape niang yalla nala yalla takhawu bubah wayé gathié galama nah borome bah ga nite munoul la yak fi ak nekhul yalla kone bo teudé nalawale am nagne confiance si iow té dou mesa dagne Abadane, sa malade biga am Touba souma sagnione ga dém thia nah urgences la diadîeûf 🙏🏾

  • @ThiamCoumba-n8t
    @ThiamCoumba-n8t 12 дней назад +21

    Pape soit fort tout cœur avec toi yalla molay faye

  • @soniasima5353
    @soniasima5353 12 дней назад +19

    Depuis jr mariage bii la xamni wadji weroul mais bon courage pape yalna la yalla taxawou😢

  • @diopfatou1308
    @diopfatou1308 11 дней назад +12

    Pape defal reck te yalla takh mbaye weroul pape du courage ❤❤❤

    • @aminaba9275
      @aminaba9275 11 дней назад +1

      Bilay wéroul koula défal téraga bi ga beug ko yomb police😅

    • @adamadioum2659
      @adamadioum2659 5 дней назад

      Dofe bou sokhore la

  • @mariamacisse5972
    @mariamacisse5972 11 дней назад +31

    Kouko khol ak chapeau 🎩 bi khamni wéroul 😂😂pape Niang mo ndiaboote nak

    • @Galsn
      @Galsn 11 дней назад +7

      Pape rek la yeureum ki mom diaroul yatal sa keur sah meune na kheuy déf louné 😂

    • @astoufall2668
      @astoufall2668 11 дней назад +2

      Lepeum dikoul moss.

    • @oumygueye7201
      @oumygueye7201 11 дней назад +8

      Mbaye deful dara kiko bindal plainte moo weerul te nak Papa moytul janr yi gno lay ray ci zero ndax dof du wéer rabbi yi gnooy jél congé

    • @OusmanemoussaCisse-w3k
      @OusmanemoussaCisse-w3k 11 дней назад +2

      Mbaye bilahi soumako niousse Dina nek nitt😂

    • @mariamacisse5972
      @mariamacisse5972 11 дней назад +2

      @@oumygueye7201 malako wakh dé bilaye nak té dou moudiou fène Koula plainte ndakh mil franc mome meune nala raye🤣

  • @LataFaye-mg3mp
    @LataFaye-mg3mp 8 дней назад +3

    du courage pape liguéyal yalla thi bopame mo yomboul🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @ToutyDiop-w1l
    @ToutyDiop-w1l 11 дней назад +3

    Boumou douguati sa keur pape niang yaw bakh gua ba paré continuel sa mbakh yalla dinala faye inchahala inchahala

  • @lacitoyenneafricaine8566
    @lacitoyenneafricaine8566 11 дней назад +14

    Maman bi ame cancer yalla nako ya allah takhawou ak kepp koumou dale si barki nabi.

    • @MbodjVabien
      @MbodjVabien 3 дня назад +1

      Ohhh massa way yallna yallah sama leu inchallah 🙏🙏🙏

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 3 дня назад

      @MbodjVabien allahouma amine🙏🙏🙏🙏

  • @seybatoubar5500
    @seybatoubar5500 5 дней назад

    Du courage pape dieu est avec toi continu

  • @aminatacisse9378
    @aminatacisse9378 11 дней назад +4

    Baye Pape Bayyil mou séed, Mbaye Weeroul. Yaw yangui Takhawou Gni Weeradi, kéne dou Yaw Masha Allah ❤❤❤❤

  • @aiss__at9604
    @aiss__at9604 12 дней назад +62

    Bor 1000 fr nga dem fay lou eup 1000fr pour déposer plainte 😹😹 deug deug mbaye mi weroul😂😂

    • @yayouSalihousamb1553
      @yayouSalihousamb1553 11 дней назад +7

      Plainte 1000f ak pass bi

    • @FatimaDiallo-f3k
      @FatimaDiallo-f3k 11 дней назад +5

      Ki kay kouko khol kham ni wéroul 😂😂😂

    • @dijabeby9091
      @dijabeby9091 11 дней назад +2

      ​@@FatimaDiallo-f3kMane deh 1000f djaralouma wakh ba siy yobou nit police 😂😂

    • @AbdouDiop-d6t
      @AbdouDiop-d6t 11 дней назад +5

      Pape boul decourage yala gise na lepe te insahala sikatanou yala dika am ndam defe lou bakh rek mo ame solo❤ frere
      Likaye doundou ni niou bari nio ngi kaye doundou mai nak boul decourage frere❤

    • @nangodiagne5927
      @nangodiagne5927 11 дней назад +2

      Ki kayy weroul khollko sûrement on lui a donné 1.medoc pour kil reste tranquille ! Li guayy deff refetna mais boullko défaut di marier niary nitt gniou weroull car do khmm liciyy topp !

  • @Galsen655
    @Galsen655 11 дней назад +23

    😂😂😂😂😂pape daga fèttè ni fèbarou khèle la yorone dof dou wère pape

  • @nenesall4636
    @nenesall4636 12 дней назад +8

    Wawaw déf Lou bakh diarnako kaye yalla moye féye amna nio khamné bouléne yalla féyoul niou pérte bilaye

  • @KhadyDiouf-jp1mc
    @KhadyDiouf-jp1mc 4 дня назад

    Du courage mon frère ❤

  • @alassanediallo2014
    @alassanediallo2014 12 дней назад +36

    soy def lou bakh yalla doula sétane courage frére

    • @FatouFall-ii8oo
      @FatouFall-ii8oo 11 дней назад +1

      Bowouyou dié plainte bi ba nieuw dakh ko sa keur ki bakhoul

  • @mamygaye4378
    @mamygaye4378 12 дней назад +5

    Baye pape niang Yallah Nala Yallah Doli Taxawou Fayal la Boppam Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🤲 ❤ 🤲 ❤ 🤲 ❤ 🤲 Du Courage

  • @FallouGalss-j8r
    @FallouGalss-j8r 12 дней назад +27

    1000fcf motakh mo plente la 😂😂😂😂mbaye mii wéroul dh pape tasal seuye bi ki merito woule ndiolé té mane na kheuye kheuye déff ko lo garaw té so boba boule wakhni dafa ma béte nak té ndiolé aye responsabilitém si yawe la nék bayii si khéle nak mbaye wéroul dh yalla nala yalla faye sa khol pape niang

    • @Ndiaga-mw6zc
      @Ndiaga-mw6zc 11 дней назад +1

      Thi rauy kou lau daum de bakhna na wadial bopam rek

    • @BayeNdiaye-x3k
      @BayeNdiaye-x3k 11 дней назад

      bouléne khépp 1000f nite kii en tout cas liguéye liguéye leu ak lép lou nguén meunti sekheu

    • @mmembacke6263
      @mmembacke6263 11 дней назад +3

      @@BayeNdiaye-x3klegui mom liko pape defal yeup est meune nako ko faye lane moy 1000f nite waroul yobou police sah nonam

    • @mmembacke6263
      @mmembacke6263 11 дней назад

      @@BayeNdiaye-x3klegui mom liko pape defal yeup est ce k meune nako ko faye lane moy 1000f nite waroul yobou police sah nonam

    • @Diagneyoussouph1510
      @Diagneyoussouph1510 11 дней назад

      @@BayeNdiaye-x3k danga yoré number bi nga dioh mako ma wave 10000 nguir passe bimou si def

  • @mmembacke6263
    @mmembacke6263 11 дней назад +6

    Bilay pape wahnga deug ndiolé kheiw bi tissu you rafet la sagnsé surtt mauve bi machala mbaye sow mom weroul ndah mom sou yorel di am mola yorel 😂😂😂😂

  • @papediagne4153
    @papediagne4153 11 дней назад +5

    Ki menoul yakk li nga liggey ba fi, bayyiko ak yallah. Du courage et bonne continuation

  • @SeynabMboup
    @SeynabMboup 11 дней назад +21

    Pape kisou werene doudef li kone boulko top

  • @oumoufoba8682
    @oumoufoba8682 11 дней назад +13

    Pape yalla n'alla yalla faye guéné ko sa keure woroule moune n'alla andille bénéne problème

    • @adamadioum2659
      @adamadioum2659 5 дней назад

      Wawaw deugeule nala abale dé dofe bou sokhore la

  • @dijafashion528
    @dijafashion528 11 дней назад +13

    😂😂mom xana fayoul 1000fr si plainte bi😂😂😂

  • @MaimounaNdao-u4s
    @MaimounaNdao-u4s 11 дней назад +3

    Pape defal rek yalla dina la fay sa khol❤❤inchala

  • @PierreGomismendy
    @PierreGomismendy 11 дней назад +2

    Tu ne mérites pas ce traitement mais dieu est avec toi.que nos prières t accompagnent pape Niang.

  • @MamediarraFall-k4w
    @MamediarraFall-k4w 11 дней назад +2

    Pape tu es un homme exceptionnel tu as toujours utilisé ton intelligence ne recule jamais tu savais en avance que mbaye est 1 malade mental donc poursuis le chemin que tu as déjà tracé tu ne le regrettera jamais parce que tu agis à cause de dieu et c'est lui qui te payera au retour et ndiole Qu est-ce tu en fais quand tu lui interdit le mari que tu lui as donné pardonne le parce que tu as un cœur d'or merci beaucoup

  • @PapeMbaye-v5p
    @PapeMbaye-v5p 11 дней назад +6

    Masa mon frère pape niang danga ndiabop rék 😭😭🇸🇳🇸🇳

  • @NdeyeCoumbaSow-w5s
    @NdeyeCoumbaSow-w5s 11 дней назад +11

    Du courage Pape mougnal rek

  • @maremegning4536
    @maremegning4536 11 дней назад +4

    Pape kii wèroul boucoo toppou si vous plaît continèl dèff rekh tè yallah takh❤❤❤❤

  • @BABEUGUEBAYE75
    @BABEUGUEBAYE75 9 дней назад +2

    Yalna yalla soutoural mais li dîaroul wakh hamguane niou weroul gua sekal 😢yalnalene yalla safara

  • @Naboumaria1441
    @Naboumaria1441 12 дней назад +9

    Kha miounieule et aussi je te conseil bayile bolé aye nitt stp soit fort pape

  • @elementndiamedarou2414
    @elementndiamedarou2414 11 дней назад +8

    Force à vous Pape Niang et tte l'équipe

  • @DiarySOW-f2c
    @DiarySOW-f2c 11 дней назад +2

    Billae diambar gua mais y’alla molay fayy inchalla ❤

  • @siregoudiaby9035
    @siregoudiaby9035 7 дней назад

    Bilay Niang boula kenn yakal sa diamou yalla degue rek Moy deugue yalla n'a sunu dolila deugueurlal

  • @modoundlofficiel2706
    @modoundlofficiel2706 12 дней назад +12

    Thiéy pape yalla nala yalla fay yiw❤❤❤

  • @sakhosakho5814
    @sakhosakho5814 11 дней назад +7

    Pape il faut nga comprend mbaye boko kholé ak chapeau bimou sol sakh ok rouge jaune bimou djiteul nga khamni il et dans sa logique enfaîte ki wétoul koi

  • @boundawdiakhate2801
    @boundawdiakhate2801 11 дней назад +4

    Pape yaw tamit ki nguay topp😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 11 дней назад +6

    Liii kaye mo takh niou wakh duff dou weur daye tané 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @MarieGomis-sn8ky
    @MarieGomis-sn8ky 10 дней назад

    Courage pape Dieu et toute la familles sénégalaises est avec toi sort le de ta maison

  • @mamadoundiaye1098
    @mamadoundiaye1098 11 дней назад +5

    Bilahi doff yangi si birr. Nit yi

  • @OumyKane-hv2wd
    @OumyKane-hv2wd 12 дней назад +4

    Baye pape mbaye weroul comprendre ko rek te yala takh yalana yalla fay say dieuf you bakh te takhawou là yak sa njabot brke Nabil Moustapha psl

  • @bannadiao2767
    @bannadiao2767 11 дней назад +4

    😂😂 begne dou ré diameuh

  • @PierreGomismendy
    @PierreGomismendy 11 дней назад +1

    Il faut continuer à aider les plus démunis.il y a des gens dont la reconnaissance n est pas leur fort.courage!

  • @thiatouyayam275
    @thiatouyayam275 12 дней назад +4

    Courage Pape Niang

  • @goradiagnewade8018
    @goradiagnewade8018 11 дней назад +4

    Pape doff ngaa ammall affaire

  • @papediazngom6121
    @papediazngom6121 11 дней назад +2

    Billakhi diarnaco boul tit boul ragual mouno bayi ndakh lingaye déff thi sa ❤l la nékk yalla molaye féy sa kh❤l ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂

  • @DaoudaDIOP-m4x
    @DaoudaDIOP-m4x 11 дней назад +2

    Courage. Yalla moy faye té kou sérieux la. Courage

  • @diaryly-nc9ko
    @diaryly-nc9ko 10 дней назад

    Yalla reck molaye Faye bouko toop weroule

  • @artsafriquecommunication6587
    @artsafriquecommunication6587 12 дней назад +15

    Doff doff leu rék continue sii liguay deff bou wérone doula plainte la yakar

    • @aissatoufalldiallo7416
      @aissatoufalldiallo7416 11 дней назад +1

      Vraiment diaroul wone sakh tokk fii di wakh.

    • @ndiobadiop713
      @ndiobadiop713 11 дней назад +3

      ​@@aissatoufalldiallo7416wakh deug nekh yalla
      Ki dafa dessè weur ndakh kou weur dou def liii
      Djaroul wone djeul temps bi yeup
      Au contraire liii ay retane lako warone def mou khamni dafko wara suivre ndakh dessè na weur

    • @modoufall1040
      @modoufall1040 4 дня назад

      Vraiment

  • @GueyeOumy-dm8tb
    @GueyeOumy-dm8tb 11 дней назад

    Pape yalla nala yalla défal diam same la amine yarabi ❤❤❤❤

  • @MmesambaAmy
    @MmesambaAmy 11 дней назад +5

    😂😂😂😂😂wouy li meunoumako mougne non mbaye sow weragoul der

  • @Soumayyarassoul
    @Soumayyarassoul 11 дней назад +3

    Pape yonnou Am yalla walahi yomboul té yagui Si yonwi machalla boul nangou Dara Wala kéneu koulaye Gal lankoor

  • @ElymaneSaidoukane
    @ElymaneSaidoukane 11 дней назад +1

    Pape Niang djam rek ngay ame inchaa Allah

  • @mamita5618
    @mamita5618 11 дней назад +38

    Policier bi mome tamit meunone na dioh mbaye 1000f rek té nopalou

    • @cheikhbasskeurmassar9548
      @cheikhbasskeurmassar9548 11 дней назад +4

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😅

    • @AbrahamDieng-c6y
      @AbrahamDieng-c6y 11 дней назад +2

      Vraiment😂😂😂mais policiers tamite parfois😂

    • @goradiagnewade8018
      @goradiagnewade8018 11 дней назад +1

      Deuggg!!!

    • @binouche89
      @binouche89 11 дней назад +2

      Esk wakh nafa ni 1000 fr la ko yorel ndakh diapnani sou fa wakhonee lolou plainte bi dou niou ko bindeu

    • @abyba5966
      @abyba5966 11 дней назад

      😅😅😅😅

  • @NgoneFall-x1w
    @NgoneFall-x1w 10 дней назад

    Bien sûr ta a Plain droit pape du courage

  • @amyamy5417
    @amyamy5417 11 дней назад +2

    Ki dès le premier jour la né ki weroul mais du courage pape

  • @djigossbathili
    @djigossbathili 11 дней назад

    Pape on est très fière de toi

  • @BëggdëggKalleDiop
    @BëggdëggKalleDiop 10 дней назад

    Yàlla dinala fay dafa metti nak ❤❤

  • @amycollegningue7824
    @amycollegningue7824 11 дней назад +5

    Pape dangua bakh yalla molay fayal popam adouna nii la deme

  • @Mmmksall
    @Mmmksall 9 дней назад

    Pape ya bakh

  • @SENEGAL303
    @SENEGAL303 10 дней назад

    Bismilah. Mane pape sou dieulé micro bi diap li au sérieux lolou momay dèf ay rè😂.
    Pape dèmal wouyou dji yone. Nga faye ko 1000f wam.
    Après mom nala faye louass.

  • @mariamasene7086
    @mariamasene7086 7 дней назад

    😂😂😂 pape way😂😂😂

  • @adiaadia9967
    @adiaadia9967 10 дней назад

    Mbaye mi doff la dé

  • @diaryly-nc9ko
    @diaryly-nc9ko 10 дней назад

    Courage

  • @boyemor9660
    @boyemor9660 11 дней назад +5

    Bilahi w😅éroule wayé gniko défal plaint kéne démoule gnou dés 😢

    • @fatimandiaye4078
      @fatimandiaye4078 11 дней назад +1

      Bilahi gni def plainte bi gno weroul

    • @boyemor9660
      @boyemor9660 11 дней назад

      @fatimandiaye4078 kone yaw kham lima kham 😁

  • @alioudabo9857
    @alioudabo9857 11 дней назад +1

    Yalla na ame épisode 2 ame ci jamm nooonnnn 😂😂😂😂 ba sonnou

  • @bintoubanellediabang712
    @bintoubanellediabang712 11 дней назад

    Thieuy adouna lii doyna warr
    Wayé pape boul découragé jamais

  • @ftm-samax352
    @ftm-samax352 11 дней назад +8

    Mané dey dof dof Lou. Un fou qui porte plainte pour 1000 fcfa. Mo ko tay.

  • @bijoux-c6l
    @bijoux-c6l 11 дней назад +5

    Ki tayouko ,😂 Pape balko rec

  • @rokhayandiaye6194
    @rokhayandiaye6194 12 дней назад +7

    Thiéye adouna !!
    Les gens sont tellement ingrats qu’on n’y comprend plus rien 😡😡😡😡

  • @dashundiaye9401
    @dashundiaye9401 12 дней назад +5

    Pape yalla rek molaye Faye ndakh sa khole mo rafete

  • @Limatata988
    @Limatata988 11 дней назад +2

    Pape boul tayi kouye lingueiyeul yalla deuneu saf sap mais yalla ngueye lingueiyeul qui weroul ndeuh 100f bouko tope yalna yalla feuyeleu

  • @MalickGaye-j6h
    @MalickGaye-j6h 11 дней назад +1

    😂😂😂😂courage pape

  • @AhmadaJadid_Diop
    @AhmadaJadid_Diop 12 дней назад +21

    Pape boudé 4000 leu mangley niaane Diokhma numérom meu dogalalko léguini ci waveam apres meu envoyer leu capture bi comme ça bou souba so démé fignleu convoqué dofa yagg. Meme boudé 8.000 laley ladj sakh amoul problème diokhma numérom.
    Aduna mom nieup niamougn Yallah moo bindd tei yamalé woul kheuyna fofou leu khelam tolou.

  • @alhamdoulilah9154
    @alhamdoulilah9154 11 дней назад

    Pape niang nguirr yalla boulko guené keur gui seytane moula beuga yakhal te meun na am sakh sunu borom dila nattu bakham dinga continue Wala dangaye décourager

  • @magatfall8486
    @magatfall8486 11 дней назад +4

    pape mèritèwo lì dè bilaye wayè yalla.dinala faye sa kholl

  • @NgouilleFall-g2e
    @NgouilleFall-g2e 10 дней назад

    Bilây niang yalla molay fay dof dou wér Mbaye dèloko ay mbokam sinon euleuk manenala andil lènén

  • @LenaMbaye-o5g
    @LenaMbaye-o5g 10 дней назад +1

    Dédéte pape gniang bouko tére sa leur ndakh yaw yala ngay ligueyal. Té inchallah yala mo lay faye té ki wéroul yaw yay ambassadeur gnou wéredi yi

  • @OumyTouré-v2s
    @OumyTouré-v2s 11 дней назад

    Doyna war pape courage yala gay defal

  • @FatoucheikhFall-r8k
    @FatoucheikhFall-r8k 11 дней назад +1

    Mbaye mi wéroul dh 😂😂

  • @assanegueye28
    @assanegueye28 11 дней назад +5

    Doff la wayé doko diokhe 1000f rek pape mo giene

  • @maymounandiaye5396
    @maymounandiaye5396 11 дней назад +1

    Yalla na yalla faye liguéyoub yalla yoboul natouleu boul décourager fayoub yalla gueun bou nite yalla na la yalla may kholou mogne yoboul dé liguéyou saytanéla boul nanguo danou

  • @aissatoungom9833
    @aissatoungom9833 11 дней назад +1

    Bima guissé Mbaye lané qui wéroule Pape mougniale

  • @mamediarraka2214
    @mamediarraka2214 11 дней назад +5

    Baadou May Baat Ndiolé😂😂Kii Nakk Weroul Vrai Doflaaa

  • @modoundlofficiel2706
    @modoundlofficiel2706 12 дней назад +8

    Pape yobol ki fan😢😢😢😢

  • @mayaciss6821
    @mayaciss6821 11 дней назад

    MBAYE SOW DÉ DOF LE MAIS PAPE BOUL TIT BOUL RAGAL YA NGUI DEF TÉ YALLA TAKH, À CAUSE DE CE GENRE DE TYPE,PERSONNE NE VEUT PLUS AIDER PAPE IL EST CAPABLE DE T ACCUSER DE CHOSES PLUS GRAVE, QU IL NE POSE PLUS TES PIEDS CHEZ TOI QUI VRAI DOF AK BADOLA PAPE CONTINUE TON CHEMIN 🙏🏾❤️❤

  • @sokhnagueye8678
    @sokhnagueye8678 11 дней назад

    Yalla dalay natou baham lingay déf mo tah .Balay ngey yég deug mou Nattou la Courage

  • @papesow1598
    @papesow1598 12 дней назад +6

    Pape galou dofbdou terr dé courage

  • @diakysfood7624
    @diakysfood7624 12 дней назад +3

    Pape nit matoul kou nek ni nga tolou rek ngaye défé courage

  • @sokhnaoumoudiaw186
    @sokhnaoumoudiaw186 11 дней назад

    Papa Niang sociale yaw ak sa équipe yalla molénedi Faye yalla bo guisse Diarra lay ragual si barkép Nabil Moustapha

  • @josephinendiaye6461
    @josephinendiaye6461 12 дней назад +10

    Pape yalna Yalla fey sa khol

  • @ndoumbediouf6197
    @ndoumbediouf6197 11 дней назад +3

    Yallah molay fay

  • @adamasamb1776
    @adamasamb1776 11 дней назад

    Du courage pape

  • @leprometzo9048
    @leprometzo9048 12 дней назад +3

    Pape yalla moy diangualké diaréko si yaw alhamdoulilah sante yalla rekk❤❤❤❤