Bacary cette série est juste incroyable les graphiques, l'aspect culturel,la vie réelle des Sénégalais et tout ça voilé par un humour tellement agréable vraiment bravo la RTS
As-Salamu’aleykoum mes frères et sœurs Musulmans N’oublie pas les 5 prières obligatoires et quotidiennes mes frères et sœurs musulmans ( As-Salât ) 1. Fajr ( 2 Rakat ) 2. Duhr ( 4 Rakat ) 3. Asr ( 4 Rakat ) 4. Maghrib ( 3 Rakat ) 5. Isha ( 4 Rakat ) Qu’Allah accepte nos prières et nos jeûnes. Amine Allah. Car le rappel profite aux croyants mes frères et sœur musulmans. Allah nous suffit ☝️🤲. Alhamdoulillah Wachoukroulillah ☪️✅
Bakary sonou gua mais sa yaye mo liguey ba gua diatat si affaires yii guel yi sathi nagnko si taxi bi niou sathiatko si niom bamou delou si wat say lokho😂😂😂😂😂
Sénégal yalna dém ba dakhe Chine ci barké seydina Mouhamed psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine
Amine
Khadioufi saway
@@badadiop675khana denga wolouwoul gnifi nek
Wala denga dég ni adouna dey touki
Amlène xeil way 😅😅😅
Série bi dafa wara ame chaque jour bilay dafa nekh trop😂😂🎉🎉
Bacary cette série est juste incroyable les graphiques, l'aspect culturel,la vie réelle des Sénégalais et tout ça voilé par un humour tellement agréable vraiment bravo la RTS
Nga sathie niou sathiat la 😂 ba paré kouko sathie dém diko diay borom 😂😂😂😂😂 Sénégal nékh na 😂😂 mais yayou bakary mo am chance deugg deugg nak
Kou beug mame khoudia lalale j'aime 😅
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉❤😂
Laye diakhate chauffeur TATA depuis mbour mangui top série bi chaque week-end
Fière de toi
Lay diakhaté chapeaux a toi chaque jour ma guiss sa commentaires félicitations
@lastweek1574 merci serie bi dama çi guiss sama bopou rék
Que Dieu Te Donne beaucoup de Taxi Amen
@marcosherry amine ya rabbi
Des cœurs pour le présentateur de MINUTE SÉCURITÉ ❤❤❤
Bakary mo am serigne deh 😂😂😂😂
😂😂Gallé Bakary ndey Coumba deffa birr.. nonn sheuteuteuteu le gars m'a tué... Une série plein de messages... Chapeau a vous
Halima gadji elle me fume wallahi je l'aime en +elles est belle 😂❤
Linak moy am sanche deugg 😂😂😂😂😂 sathie la ba paré nieuw dila diay 😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Une série très réaliste: plein de messages teintés d’humour 🙏🏿🙏🏿
C'est diffusé sur la télé à quelle heure et quel jour ?
Bakary balma akk dama fogon danga dioh bagage yi mada😂
Wallahi mane miii lolou laa fogone 😂😂😂😂😂
Et pourtant lolou la wakh deh
Mane mi lolou la fogone
Mada dh mougui ni bakary gniokhouko dra 😂😂😂
De mm k moi 😂😂
Li déh moy alal diou léw nak😂❤❤❤❤
Bakari l'homme qui n'a jamais perdu sa thiono
😂😂😂😂
Degueul sam fall bi si souf rek la série c'est le Sénégal conforme ❤❤❤❤
Dafa kawé lool
Bèpe theatre bouy daw senegal serie bakary moy sène baye❤❤❤😂😂😂
Ma série préférée ❤😂
As-Salamu’aleykoum mes frères et sœurs Musulmans N’oublie pas les 5 prières obligatoires et quotidiennes mes frères et sœurs musulmans ( As-Salât )
1. Fajr ( 2 Rakat )
2. Duhr ( 4 Rakat )
3. Asr ( 4 Rakat )
4. Maghrib ( 3 Rakat )
5. Isha ( 4 Rakat )
Qu’Allah accepte nos prières et nos jeûnes. Amine Allah. Car le rappel profite aux croyants mes frères et sœur musulmans. Allah nous suffit ☝️🤲. Alhamdoulillah Wachoukroulillah ☪️✅
Keur Bakari nekhna 😂😂😂❤❤❤
Kou d accord ni Bakary mo eupeu problème fi si senegal ak likeu weure😄😄😄
Une série que j’aime beaucoup ❤
Merci à toute l’équipe 😂
Mais Vito Bacary Mola eupeu bopp dh😂
Vito mo nekh😂😂😂kholal loma diokh la moudje
Bakary way j’adore cette série depuis Mauritanie 🇲🇷 😊❤
Li dé diadouwoul aye jeeguene youye sathie yalla naniou ci yalla mousseul🥺🤔
Mo beuri si raw mi legui nk
😂Yaw khamo ni djiguen yi nio daka sathie Sénégal
Fans bakary nouyou nalén diléne nianal diamou diko sakkou si yéne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
fay nanou leu😂😂
Kou name djiby séye com man lalal j'aime ❤🎉
Moi je suis grâce à djiby seyw
On réclame le bonheur de bakary 😢😢😢
Encor boy yangi fi 😂😂
mba yénagui done cons Zikroulah bi daw thi souf😭❤️🙏🏾👌🏾
Ndeyesane senegal béni famila ❤
Vito bama khamé batay meussta ame weurseuk si serie 😂
Vito bou Jules diaro bi😂😂😂😂
Mame khoudia amna chance gorowom da bakh❤❤❤
Bakary balma akk dama fogoone ni ya sathie tissus yi😂
🤣🤣🤣
Mane miii lolou la xalatone di😂😂😂
Pour mane mada lako diokh😂
Ak man mi😂😂
ak mane mi sakh
Yayou Bakary nena: Loy yathi yathiaral melni mbaxalou keuyite😂😂😂😂😂
Kharmi lekk na yayou djiby seye sort de ma tête 😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
@maryamkeita891 😂😂😂😭
Lii souma rayoul😂😂😂
@NouraDiouf wouy 😂😂😂😭
bilahi 😂😂😂
😂😂😂 BAKARY la meilleure série 😂😂😂❤
Barki alhouran mame khoudia moy le meilleur artise au senegal
Un grand Bigup à la RTS 🎉
Mafi djitou kou d’accord rak lalal j’aime ❤😂😂
Maneuh dama foguoneu ni la maman de Khouthia mo beugoneu diaxassé kër tass yakar benen mère bi😂😂😂
Leçon Bou ame importance Li dée moy nit louy sa weurseuk digua si diott
Vito mo meune...je l'ai remarqué depuis tiabibi avc Laye Diarra... puissance
Vito de diaro bi avec Jules 😂😂
Ndeysan yangui wakh serie bou nexone😂😂😂😂
Kou name djibi seye comme mane 😂❤❤❤
Mane mome brt bi banioumassi ba khekh kepp kou nara wathio ak linioufay téré damalakoy wakh❤❤
sam faal bi😍😍🥰🥰
Tay Bakary amna ndimbeulou Yalla 😂😂
Justice ⚖ pour sarigne fallou one love Sénégal 🇸🇳Justice ⚖ pour sarigne fallou one love Sénégal 🇸🇳Justice ⚖ pour sarigne fallou one love Sénégal 🇸🇳
Take katou cheveux bou j’aime sama commentaire bouma la reukè dinga mourou 🧕🏾 dji 😂❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊
le voleur volé😂😂😂😂😂
Guinté bi mo nara dakk guinté président Diomaye ak absa Faye😂❤
Bakaty mon film frefere
Mbaxalou keuyitt😂😂
Badola rek niou yobalèla guay sathi def lou bakh yomboul
Ha légui MINA dagayyy rawalé😂😂😂😂😂
Kou begue Bakary lalal j'aime ❤
Bakary neikoul ci jamou mais pyto mii tamit kagne lay adounam di neikh🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂 bilahi Vito la beugue 😂😂😂😂😂 wouye
est ce que turquie bena lafa 😂😂😂😂😂😂😂thiey vito
Série bi yane jour lay ame 😂😂
Mane Bakari damay am envie wawe ko non 😢
😂😂😂
Wakh lén Bakary mou balma Akk ndakh demb dama ko accuser ni Mada la diokh mbouss mi🤣
Même mn miiiiiii😅
Man mi wah ni dako déthie pour hew bi😂
😂😂😂ak mane nane mougua cha Mada 😂😂
Bakary diape na sathiame 😂😂😂
Ouly mon combat ❤
Notre combat nakh amgua çi concurrent 💪
Bakary balma akh déma néwone mada nga thiokh tissu yi 😂
Mbakhaloum keuyitt 😅😅😂
Mère yama nk mo am weurseuk deug
Merci beaucoup sonko
Toujours bacary
Oups sathiey kou d'accord Vito sath laa laa laa jaim
Vraiment deff lou bakh jafe na gnii danio yap Bakary 😂😂😂
Quels films de réalité à la Sénégalaise
meilleur série manchalah
Série bi si bopam mo nekh😂😂😂😂
Moussa tine bayil sathie 😅😅
Bakary sonou gua mais sa yaye mo liguey ba gua diatat si affaires yii guel yi sathi nagnko si taxi bi niou sathiatko si niom bamou delou si wat say lokho😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
@@maryamkeita891 DEUG leu wala😂
Sathie si kaw sathe
Billay mame khodia dafa man lomoy deff🎉
Meilleur serie
Sama tante bi nekk Turquie 😂😂
Danio yap gor yi rk ms Sénégal djigeen yi nio daka satiy bilay 😂😂
Wa vito 500f la moudjé ladj😂😂😂
Première kayy 😂😂😂
bakary mangui toupe dh pour mane sakh mada nga diokh bagage yi😂
Bacary tamite loula tere def mboy yi ci coffre bii😂😂
Svp nagn teudie école 🏫 yi ba fallou fall géune prison
Demal djangui say leçon 😂😂
😂😂😂@@AyishaDiop-y4s
Machallah
Sacré taximane Bakary
Mère bi beugg na adouna😂❤❤
Le grand vito🎉
Bacary loungne wax rek mom la
Man Vito Dinama rey😅😅😅😅😅
Quel soulagement 😂😂😂😂😂
Kholallll loma diokh 😂
Vito moh nexx😂😂😂 nak
Keufe dh légui liguéye la 😂😂😂😂😂😂
Bacary soneu na 😂
📍| Justice pour FALLOU FALL☝🏿
Kou deg sam fall bi ❤
Mbaloux kheuyite 😂😂 kaye