Bsr je suis en direct aux USA je salue tout d abord le courageux baye Fall c triste je vie ici plus de 26 ans dit à baye fall bcp de courage on demandé aux gouvernements du Sénégal de faire tous les moyens pour soutenir ses expulsés
Man defna 5 mois si yone bi mé nioune ay goor yallah laniou ay dioulit laniou centre yi ac quan yi lousi néke yepp wakh ko dou yombe le 14 bi la gnibisi mé sante yallah baye fall ndanane nga
Baye fall diambar nga Goor yalla nga ... Yalnala yalla oubill Werseuk gou barii walayy si j'avais les moyens je t'aurais financé... yalna yalla diapalé tu mérites d'être aidé pour ouvrir un atelier
Gni dougou liniou wakh ba dougou souniou nèkhonn wakh ko dougou c'est comme si gni dougou niepp lolou lanou wakh nous on fier d'être musulman et on le restera toujours je suis aux usa et j'ai passé par cette voie yalna yala takhawoula mais dèlenn soralé linguèni wakh douniou fowè sunu dîné
Li moy wax bi Frère thé deugeu rek mo nekh ki limi wax lousi heupou amoul mane mi fofou la diar na nangou ndogal bi thé mougn mettina mais boumou yakheu gni dougou
J’ai suis toute l’émission, juste un precision moi j’ai fait des années à l’extérieur mais baye fall bi la beugeu layébiré barina ay domou Senegalais you nek ci allebi amnagne fi séne Terranga di doundé alale bou lew té dara Lou gnak fayda mayouléne ay papier deugla amnaci bene bene gnouy diaye sene ngor mais nak bagne kateyi barinagne fi gor yalla yi barinagne fi nite meuneu diar ba ame keuyite barinafi,
🇺🇸🇸🇳😢méttina trop bilahiiii juste pour ravir leurs parents yalla na yalla motali yéné niêupp Incha'Allah baniou téral souniou wadiour yi maqqa Incha'Allah🕋❤🙏
Neysan baye fall kou gueum yalla la ta lolou rek mo am solo yalla na la yalla defall li gueun si yow may la lou kawe sa niort si barke seydina mouhamet psl ❤❤
Ndeysane le gars on partager le même vol pour revenir au Sénégal c’est un vrais baye fall mais nak nioune la yalla dogal niou Gnibissi Mai’s barina niou Doug tei dieulouniou PD juste pd bi mo geuneu wore Mai’s nak barina niou Doug sax tei kene ladioulene Dara yalla moy dogal tei nioune la dogal niou Gnibissi kou meune dem demal tei yalla weurseugeul la nga dougg inchalla 🙏🏿🙏🏿
Mangui lay masawou metti trop vraiment Mais d'accord rouma ak uoe si lingay wax yone bi kou nekeu ak sa chance rek 130 et quelques yognou ay lou hepou ay 1000 li 1000 dougou nagnou thé aoumouñou si camp yi sax une semaine Mane mi wax ak uoe fofou la diar ñanene donc fi kou nekeu ak li Yallah toudi si uoe rek
Je peux comprendre la première vague d’immigration clandestine. Mais ceux qui prennent les pirogues de fortune de nos jours ou qui prennent les routes aussi difficiles ont tort. Il n’y a pas de conditions de vie au Sénégal qui justifie cela. Nous avons assez d’exemples. Koussi dougou kouné dinga gnak sa ngor bénneu instant, di nagnla traiter n’importe comment, Yallah rék mo siy diappe. Tu vas être témoin de choses horribles té dossi meune darra. Nite fo meunti nék sa weurseuk daf la fay fék. Sabablou waw mais jeu de hasard nêne dafa haram, wakhoumala bo parier sa bakane. Qu’Allah nous guide.
Nionié Di wa Europe Amérique Asie danio déf révolte révolution ba khékhe khékhe you Miti ba ague fi NIOU ague yén jeunesse SÉNÉGAL lounguén déf beug Lou yombou NIOU défar Sénégal réw n'guén khéy donne ay million déféni daniouléne Di BAYI n'guèn déme bén dignité amoulenko
All what these peoples are talking about it is true . I am also a victim of this journeys but thank Allah i am in europe . May Allah helps all our peoples of African youths whose were leaving africa and look for the green pastures if they make Africa bettervwe wouldn't take this risk journey
Excellente emission, mais juste quelque remarque la fille elle ne suit pas le fil conducteur e manque de professionalisme. Elle pose des questions au mauvais moment et les qustions font office de hors sujet du fil de communication de l'invité, le gars en casquette adidas est trop proche de son micro par rapport aux autres, donc du coup la personne qui suit se sent gener quand il prend la parole, a cause du niveau de volume de ta télé ou téléphone, tout le monde est a un niveau normal mais lui le volume est fort. Momo tu es patient, attentif et pose les questions qu'ils faut, la communication est fluide on a envie de regarder. Mais les autres faut etre plus professionel et etre attentif respécté le fil conducteur et avoir des questions qui respecte la trame de communication de l'invité. MERCI
Ohhhh sama Tanger bi CT en 2017 0h nguen Doug si auto mafia bi dém bassi niaye dokh ay kilomètre Di dévié policié yi avec leurs chiens Di dougue si tranquilo yi , Di def yeufi gor yalla ba guiss mer bi pompé zodiac bi vers 6h du matin CT en période de ramadan ték rekk ba commencé diow gnu Japgnu mais Dara bou yone diékhoul wakhussil d'où jekh lep rek ndeyssane beug téral waydiour ak défar sunu avenir
Non wadji limou wakh kou nek ak ni nga koy dégé lui il parle de la route pou les États-Unis 🇺🇸 donc il la dit 90% niouy dial PD laniouy déposé donc 10% niou dougé ak bénéne méthode voilà ftance bi amna kou ma kham kou ame papier gorjiguéne même les femmes yen as qui yont sa kou néke ak sa geum geum mane mi papier vie familiale la yor yague n'a bi niou wakhé deposel papier PD dama né mouk su adouna té téwoul amna ko si bénéne aname wadji dall mi ngi yété après kou nek ak sa analyse mane si limou wakh la ande yalla n'a Diam yague Manchallah 🙏🙏🙏
Billahi Sénégal dou rew zéro protection j'ai investi beaucoup d'argent au Sénégal des hectares a diamniadio pôle urbain dieul zero dédommagement j'ai acheté des titres fonciers on m'a construit dessus 15 ans toujours au tribunal sama avocat khadi ma khadi li moy Sénégal deukeu bou dama ndeyam
Je faisais de l'importation et en même temps transporteur avec mes camions. Ça c'était pas des investissements mais du placement prendre ce que je gagnais et acheter légalement devant notaire des tf nickel, a diamniadio des ha TNI vérifié avec acte administratif ordre de recette payé délibération obtenu. Laisse tomber Sénégal dou rew
@@Ctnnn il ne faut jamais baisser les bras il faut se battre dans 5mois le régime corrompu de Benno sera balayé. Il faut te battre et puis il faut changer d'avocat cherche un battant .
Ki woté nane visa yombena usa du tout chance reek la. Diabarou patron entreprise bou mak refusel nagnoukoko 3 fois té passporam fessna 3 fois depuis khalé la commencé wone voyagé si europe ak afrike dakhoul gnou mayeko. Il a fallu gnou mayeko visa canada mou deposewate gnou sok ko maye usa .
Tout ce manque de respect que nous subissons c'est vrai gouvernement bi amna thi walleuh bou reuy mais nous aussi pourquoi nous partons dans des pays où on ne veut pas de nous tei massla wougnou thi. Gnoune aussi gnoy yaplou sougn bobou partir à tout prix bi lagnou wara bayi. Nagnou dem thi conditions you ler et thi deuk you acceuillant aussi
Le gas du Belgique a tout résumé. Motif documents yi on ne mentionne pas "gordjiguén" on écrit " UMANITAIRE" mais pas tout umanitaire est gordjiguén En plus ils ne peuvent pas descendre au pays d'origine
Baye fall mi gor deug la mais bayill touki bi guay force djigoula fi diar yeup yalla nala yalla teral mé bayile
Bsr je suis en direct aux USA je salue tout d abord le courageux baye Fall c triste je vie ici plus de 26 ans dit à baye fall bcp de courage on demandé aux gouvernements du Sénégal de faire tous les moyens pour soutenir ses expulsés
Walahi baye fall kou diara diapalei la 😭😭😢😢😢😢😢
Le Sénégal À besoin des gens comme vous!!!!
Non vraiment je suis tellement fière de toi baye fall Bilahii yalla nala yala défal diame ak khéweul si barkeii cheikhoul khadim❤❤
Merci pour l‘importance de cette émission très instructive j' ai beaucoup appris
Merci beaucoup sunugal24
Cette émission mérite d, être traduit à tout Les langues du monde
Billahi wallahi😢
Amna solo
Voici le Sénégal,si on vous dit de laisser les politiciens vous refusez.seul la lutte libère
Man defna 5 mois si yone bi mé nioune ay goor yallah laniou ay dioulit laniou centre yi ac quan yi lousi néke yepp wakh ko dou yombe le 14 bi la gnibisi mé sante yallah baye fall ndanane nga
La dame nicorogua😂 m'a tué mais machalah très bonne émission et très instructive.
Kénn dou bou siteu ci prononcé tour pays bobou😂😂😂😂
Félicitations pour l'émission c'est vraiment très instructive j'ai appris beaucoup de choses et grand respect à Baye Fall et les autres du plateau
On un TV
SS
Sss
Ndeysane❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah ils ont pleins de resources ils s’expriment bien mais dina baax incha Allah loula rayoul dalay yokou dolé
Baye fall diambar nga Goor yalla nga ... Yalnala yalla oubill Werseuk gou barii walayy si j'avais les moyens je t'aurais financé... yalna yalla diapalé tu mérites d'être aidé pour ouvrir un atelier
Bon courage mon frère
Sama khol nekhoul 😢bay Fall yallnala yalla takhawou
Gni dougou liniou wakh ba dougou souniou nèkhonn wakh ko dougou c'est comme si gni dougou niepp lolou lanou wakh nous on fier d'être musulman et on le restera toujours je suis aux usa et j'ai passé par cette voie yalna yala takhawoula mais dèlenn soralé linguèni wakh douniou fowè sunu dîné
Li moy wax bi Frère thé deugeu rek mo nekh ki limi wax lousi heupou amoul mane mi fofou la diar na nangou ndogal bi thé mougn mettina mais boumou yakheu gni dougou
MachaAllah Alhamdoulilah Yallah nalen sounou borom bi sameu amine
😢😢😢😢 les témoignages sont très touchant. Ils ne font dire la vérité du vécu.
Vremant émissions by nehkna ❤❤❤❤
Le problème c'est pas le faite de se déclarer omo!la dureté de notre Sénégal kou meuna dem demal Sénégal mettina
Baye falll yalla bakha na di na bakha
Merci beaucoup Baye fall yalla nalén yalla takhwou🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
J’ai suis toute l’émission, juste un precision moi j’ai fait des années à l’extérieur mais baye fall bi la beugeu layébiré barina ay domou Senegalais you nek ci allebi amnagne fi séne Terranga di doundé alale bou lew té dara Lou gnak fayda mayouléne ay papier deugla amnaci bene bene gnouy diaye sene ngor mais nak bagne kateyi barinagne fi gor yalla yi barinagne fi nite meuneu diar ba ame keuyite barinafi,
Aye mague preske 50 ans mounougnou ame sakh nék bou bakh ndakh ndol motakh gnouy gaday reek😢😢
Billay dafa méti si gor
🇺🇸🇸🇳😢méttina trop bilahiiii juste pour ravir leurs parents yalla na yalla motali yéné niêupp Incha'Allah baniou téral souniou wadiour yi maqqa Incha'Allah🕋❤🙏
Neysan baye fall kou gueum yalla la ta lolou rek mo am solo yalla na la yalla defall li gueun si yow may la lou kawe sa niort si barke seydina mouhamet psl ❤❤
LIBÉRÉ OUSMAN SONKO ❤❤❤
Thiéy Afrique ak injustice kagne la séye bi di tass 😭😭😭😭😭😭
Bay fall geumal sa borome yalla dinala dippale fii si réwmii in cha Allah 😢😢
Belle émission
Machalla senegal 🇸🇳 24
Senegal dafa meti mais yalla bxna yalla nalen yalla takhawou
Ndeysane le gars on partager le même vol pour revenir au Sénégal c’est un vrais baye fall mais nak nioune la yalla dogal niou Gnibissi Mai’s barina niou Doug tei dieulouniou PD juste pd bi mo geuneu wore Mai’s nak barina niou Doug sax tei kene ladioulene Dara yalla moy dogal tei nioune la dogal niou Gnibissi kou meune dem demal tei yalla weurseugeul la nga dougg inchalla 🙏🏿🙏🏿
MachaAllah courage mon frère vous avez un bon cœur
merci amina
Merci bcp pour les infos ... Et surtout à bay fall ❤❤
WADJI GUERRIER LEU MAIS VRAIMENT AMOUL CHANCE SOU TOUKI 7 FOIS DE TENTATIVE C EST CHAUD
Machalla
Mangui lay masawou metti trop vraiment
Mais d'accord rouma ak uoe si lingay wax yone bi kou nekeu ak sa chance rek 130 et quelques yognou ay lou hepou ay 1000 li 1000 dougou nagnou thé aoumouñou si camp yi sax une semaine
Mane mi wax ak uoe fofou la diar ñanene donc fi kou nekeu ak li Yallah toudi si uoe rek
Baye fall❤❤❤❤
😢😢way dij dofla ba nopi binga bagné wakh gordijgen nga dof datakh nga doneko yalla khamna linga done
c tout une aventure es beaucoup obstacle et de triste histoire on es tous de passage sur terre et bonne route au retoure
Merci à tous surtout à baye fall
Ce que dit Mansour c'est la métaphore de "l'alchimiste "Paolo Coelho
Du courage grand bi wallahi diambar deugue gua gno bok nday ak baye wayé kén eupoula diom
Yalla na léne yalla doli diam
Senegal amoul perecidant aye doméram niofa nék
Perecidant😮😮😮 eh ben... yow tamit li gua bind mom
Perecidant😂😂😂😂😂
Baay Faal est un homme fort et saint
Triste vive le changement pour l'Afrique,💔😡
Bayfall le Star de l'émission
❤Félicitation pour l'émission ❤
Courage rèk fall ❤
❤
slt sen waxtan amna solo may
Tonton kokou. Doug Legi diko wax ni bou visa yoomon ken dem Nicaragua difa diar Baye yak Mansour ken amoul sen fay
Vraiment machalla
Ce baye fall la vs lui posé des questions tres pertinente mais il ne repond pas aux questions que vs lui posaient il fait hors sujet vraiment
Il fait le malin le connaisseur
ces 2 invités sont a encourage
❤Vraiment❤ je❤ vous❤ remercie ❤
💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪baye fall
Yalla bakhna fre❤
Natou ak destin nio andak
Mais niojne Sénégalais guissouma guouniou gueune ignane surtout ici au maroc
Je peux comprendre la première vague d’immigration clandestine. Mais ceux qui prennent les pirogues de fortune de nos jours ou qui prennent les routes aussi difficiles ont tort. Il n’y a pas de conditions de vie au Sénégal qui justifie cela. Nous avons assez d’exemples. Koussi dougou kouné dinga gnak sa ngor bénneu instant, di nagnla traiter n’importe comment, Yallah rék mo siy diappe. Tu vas être témoin de choses horribles té dossi meune darra. Nite fo meunti nék sa weurseuk daf la fay fék. Sabablou waw mais jeu de hasard nêne dafa haram, wakhoumala bo parier sa bakane. Qu’Allah nous guide.
Respect à vs❤
Oh Baye Fall Borome Bakh Leu Bilae Ducurage Frère Yalla Limou Deff Mo Gueune 🙏
Baye fall khamnako ndeyssane,colobane la Nek, diambar deug
❤baye fall lika wax mo am sax canada
Mo ame sakh Europe bi yeup presque
toi tu es le heros senegalais j espere ke t as dit aux agents anti drogue mane baye fall la et ils t ont compris en wolof
Nionié Di wa Europe Amérique Asie danio déf révolte révolution ba khékhe khékhe you Miti ba ague fi NIOU ague yén jeunesse SÉNÉGAL lounguén déf beug Lou yombou NIOU défar Sénégal réw n'guén khéy donne ay million déféni daniouléne Di BAYI n'guèn déme bén dignité amoulenko
All what these peoples are talking about it is true . I am also a victim of this journeys but thank Allah i am in europe . May Allah helps all our peoples of African youths whose were leaving africa and look for the green pastures if they make Africa bettervwe wouldn't take this risk journey
C'est la même chose en Belgique
c'est grave ce qui se passe en europe 😔😔
Voix legal deh sma billet 700 mil rek lassi dépenser de senegal à New York
En tous cas kou meuneu yam bresil baxna.
Déf 2 ans amsa séjour apres bouyone bi nékhaté ngua tak diok.
Bouñoula diapé ngua délouwate bresil
Mé doug brazil yomboul
Baye fall rék ♥️👍
❤❤😂😂😂
Excellente emission, mais juste quelque remarque la fille elle ne suit pas le fil conducteur e manque de professionalisme. Elle pose des questions au mauvais moment et les qustions font office de hors sujet du fil de communication de l'invité, le gars en casquette adidas est trop proche de son micro par rapport aux autres, donc du coup la personne qui suit se sent gener quand il prend la parole, a cause du niveau de volume de ta télé ou téléphone, tout le monde est a un niveau normal mais lui le volume est fort. Momo tu es patient, attentif et pose les questions qu'ils faut, la communication est fluide on a envie de regarder. Mais les autres faut etre plus professionel et etre attentif respécté le fil conducteur et avoir des questions qui respecte la trame de communication de l'invité. MERCI
Ohhhh sama Tanger bi CT en 2017 0h nguen Doug si auto mafia bi dém bassi niaye dokh ay kilomètre Di dévié policié yi avec leurs chiens Di dougue si tranquilo yi , Di def yeufi gor yalla ba guiss mer bi pompé zodiac bi vers 6h du matin CT en période de ramadan ték rekk ba commencé diow gnu Japgnu mais Dara bou yone diékhoul wakhussil d'où jekh lep rek ndeyssane beug téral waydiour ak défar sunu avenir
On vs suit une émission très intéressante il fait 1h du matin
Billahi DEUG la fall Sénégal d'où rew 😢
Le gas en bleu est instruit et très intelligent
Baye Fall 👌👌👌👌👌👌
Senegal mon mèty
Non wadji limou wakh kou nek ak ni nga koy dégé lui il parle de la route pou les États-Unis 🇺🇸 donc il la dit 90% niouy dial PD laniouy déposé donc 10% niou dougé ak bénéne méthode voilà ftance bi amna kou ma kham kou ame papier gorjiguéne même les femmes yen as qui yont sa kou néke ak sa geum geum mane mi papier vie familiale la yor yague n'a bi niou wakhé deposel papier PD dama né mouk su adouna té téwoul amna ko si bénéne aname wadji dall mi ngi yété après kou nek ak sa analyse mane si limou wakh la ande yalla n'a Diam yague Manchallah 🙏🙏🙏
khana sénégalais yii gone déclarer PD pour entre mai pas nous quand même les mauritanien
Billahi Sénégal dou rew zéro protection j'ai investi beaucoup d'argent au Sénégal des hectares a diamniadio pôle urbain dieul zero dédommagement j'ai acheté des titres fonciers on m'a construit dessus 15 ans toujours au tribunal sama avocat khadi ma khadi li moy Sénégal deukeu bou dama ndeyam
Tu avais investi dans quoi ? Et sa na pas marché,?
Il faut faire les sites internet pour dénoncer cela .
Je faisais de l'importation et en même temps transporteur avec mes camions. Ça c'était pas des investissements mais du placement prendre ce que je gagnais et acheter légalement devant notaire des tf nickel, a diamniadio des ha TNI vérifié avec acte administratif ordre de recette payé délibération obtenu.
Laisse tomber Sénégal dou rew
@@Ctnnn il ne faut jamais baisser les bras il faut se battre dans 5mois le régime corrompu de Benno sera balayé. Il faut te battre et puis il faut changer d'avocat cherche un battant .
Bilahi baye fall mi limiy wax dara dousi deug
Bay fall yalnala yalla takhawou
Ki woté nane visa yombena usa du tout chance reek la. Diabarou patron entreprise bou mak refusel nagnoukoko 3 fois té passporam fessna 3 fois depuis khalé la commencé wone voyagé si europe ak afrike dakhoul gnou mayeko. Il a fallu gnou mayeko visa canada mou deposewate gnou sok ko maye usa .
Bilahi dafa diafei am man mi Legui ma def 3ans ba Legui mayou niouma
On était avec les frères de aziz ndiaye promoteur dans les camps dou kou diok rek am visa chance la rek
Khaarlén après élection yi téguén wotél Pastef souréwmi sopikouwoul guéne soogua dém...
Thialay gueune yessé Sénégal bou. Nieuw gueune yess bifi diougué
Sénégal dafa tarde macky mooy satan bi
Tout ce manque de respect que nous subissons c'est vrai gouvernement bi amna thi walleuh bou reuy mais nous aussi pourquoi nous partons dans des pays où on ne veut pas de nous tei massla wougnou thi. Gnoune aussi gnoy yaplou sougn bobou partir à tout prix bi lagnou wara bayi. Nagnou dem thi conditions you ler et thi deuk you acceuillant aussi
Do baye fall 😮
Xamo louy baye fall
@@SaliouNiasse domou Thiaga bi sa data yaye 😿😿😻😂🤣sa yaye thiaga la merde
❤❤❤❤❤
Sénégal dou rew deuk Bo hamni ken amousi yakar vraiment c’est triste tout ça à cause d macky et d son gouvernement domeram
Vraiment je veux numéro de baye fall
Mais derniere vague bi rék mo démé mais les premiers sont entré sans condition
Eupeul rek ils devaient faire des vagues tous les 3 mois mais nii américain ms yi daniouy titt!
❤❤❤❤😭😭😭😭
Même le Maroc 🇲🇦
Se baye fall faut lui dire la vérité, il faut être patient, et correct dans la vie
Yaw tu es qui pour donner des leçons de morale.jugement de valeur baxoul
Yaw khana si système bi gua bok tok bouye dokh
C'est quoi être correct selon toi ? Soof nga trop leernamani waadjii mooleu gueun correct fouf .
Le gas du Belgique a tout résumé.
Motif documents yi on ne mentionne pas "gordjiguén" on écrit " UMANITAIRE" mais pas tout umanitaire est gordjiguén
En plus ils ne peuvent pas descendre au pays d'origine
Dou libien reke nare yeupe la respecte wouniou nite kou nioull nioun kaye nio beugiye nare complexe you kate senn daye yi
😢😢😢❤❤❤