Je suis pas trop hip hop mais meunuma gnakk commentaire clip bi nicena trop c bien fait , son bi nekhna nah trop way et la meuf joue bien son role. Vous êtes magnifiques ça me donne envie de retrouver mon homme. Ngaaka respect à toi
Franchement hip hop galsen ça evolue.... C du lourd ce son respect à toi ngaaka son bi nekhna.... La fille elle a été juste magnifique et son style aussi 👌🏻..... Ngaaka mane dh neena waaw
La vidéo est d'une clartè si éblouissante, l'image d'une pureté si hypnotisante...sans compter ce talent phénoménal. "Souma ko doune-doule wone sakheu...yeugue-yeugue bi, sensation bi nek ci clip bi melnani vivre na lou ko raw..." 💖💖💖💖 Peace and love
Nul n'est nulle ici , l'importance c'est de travailler dure pour s'en sortir . Le rap galsen est en train de faire des démarches dans tout les côtés . Les gens deviennent de plus en accro grâce au nouveau tallent ... Respect à vous . ❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Nice good job Ngaaka! Gel bu nice ,Son bu nice, Style bubess ,Clip original. Ku bagn Ngaaka digua dh say bo yewo vue yii di doubler machallah depuis Bargny
mangii doon soucié cii gejelaa déeg. wayee kontaan naa. j'ai aimé le vidéo avant même DL regardé. après l'avoir rgrd s'il y'avais possibilité d'Aimé encore le vdo j'hésiterait pas. tellement daafa nic
Guél yima top barrina mais lolou dou dara way ❤beugu nala way bouniou xoulo beuguoumala bayii🎉 Nena goor yimou diota xam yép malein geuneu gentl 😢bouniou wété si nék malein geuneu bantal 😂dinama faun ray😮thiokotane ma way ❤lélé mou dompatt ma teupp tombatt 😢mou réé bisou 😘 ma rk songuatt té nane ma do guattt😂mbarikalah fi ni do guat 😅ték guama sompatt 🦈🐟wiss si salade 🥗 def si tomates 🍅jus d'orange bi daal ma rk gua khamni amoul diambatt❤❤❤❤❤❤❤Ohhhh jtm papa ici ta fille Maty en Octobre 2024🙏
Sama rappeur moye ngaaka blindé le roi des rappeurs c un rappeur qui rap bien alhamdou lillah ngaaka mane yeuw la beuge wallah bonne contination merci rappeur
Mho waxonn naniou la bayile niouy guenné par 10 nionn niouy guenné par benne Man me kou niame pasi té niamm dayou béye xame ni dou bene Man nééma waaw Mbaarikallah Mbaarikallah for life
1:21seconde ecouter bien ya un son qui me fait tres colle a loreille NEMA WAWAWWWWWWWWWW mais bro colle en yagui thi dehh jsui ton fan n1 bonne contuniation yagui thia
Ki la après le nouveau président bassirou diomay faye 2024❤😂🎉
S8 là🙌😂🇸🇳❤
🎉🎉
Moi😂
Sougnou King baba ki est là en 2024
Moi
Moi
Moi
Moi
Moi🎉🎉
Vraiment l'innovation de ngaaka blind transporte le musique sénégalais. Bravo 👌🏻👍🏻👏🏻 king baba
Khalei bouy dokh dey tiakass tiakass ...diadieuf king ngaaka ...maaaaaadddddddddddddd
Je suis pas trop hip hop mais meunuma gnakk commentaire clip bi nicena trop c bien fait , son bi nekhna nah trop way et la meuf joue bien son role. Vous êtes magnifiques ça me donne envie de retrouver mon homme. Ngaaka respect à toi
Terese Preira 0+
Terese Preira
Kon yes-😆😆😆
Kii de Moy ngaaka boko maye chance ba deglou ben si ay chanson dangay beug rap par forces😂
Doudourertdersims
Yalla mala yalla guéné thi barké Sering touba Jaime bcp ta maman ngaka
Franchement hip hop galsen ça evolue.... C du lourd ce son respect à toi ngaaka son bi nekhna.... La fille elle a été juste magnifique et son style aussi 👌🏻..... Ngaaka mane dh neena waaw
Oui avec une belle précieuse son teint aussi dafa andal akk Ngaaka
Serigne Fallou Diop .
Samba Sow mrci broo
Nice
Tu
ngaaka nèna baby chérie (Ssou) cva lolll
ngaaka meunoulll waxx chou
Mais j'aime b1 7 chanson
Courage frère bne continuation
Oh la petite elle est trop douce, elle me fait rêver... Nice Ngaaka tu as assurer King Baba depuis Louga
Reve alors bro
Et mw sui d louga
Wallae iioe yallah doulla sétane Yallah nalah Guéné si barkii Mohamed
C’est l’un des meilleurs clips de gaaka à mon avis personne 🥰🖖
Ki 2020 ❤❤❤❤❤
nékhe na trop yalna sa diame yake je suis fière de toi nganga blindé👌👌👌👌
Nous sommes 💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽🔥
❤️
Awa🇬🇭💖💖💖Love
💞💞💞💖💖💓💓💪💪💪
Supporting from The Gambia🇬🇲🇬🇲🇬🇲💯💯...kumu nekh Doral Like bi👍🏿
Challzz baldeh cava
No
Dip
Broo ngaka tu sortira bientôt courage stp aime mon commentaire
Excellent !!! bon travail ngakka!!tu es fort c'est indéniable !!!! bonne continuation!!bro!!!rap galsen 4 ever
J ecoute rarement de la musique sénégalaise ms ce song là c un oufff ❤
Ki revives les music en 2020 ❤🥰
Mane beugue n'a dielssi ngua seysi si mane nema .....🤩🥰
New king sound bi cool na iioe la papà ngaaka foula neikh ngay teul💥💯
Nice vidéo the new king
FATELnena waaw YALLA NA SEYBY BARKEL🥰🥰🥰COUPE BOU NICE laf 👄et yeux
No vraiment clip bi Nice na trop
Qui est là en 2021 pour souhaiter ton bébé adoré une bonne et heureuse année
Dip laye begué mais bilakhi ndanane nga diam rék ngaye âme
ngaka gnaaw nga , khalé bii gnaawna ak sa bouch
ngaka walayyy jt beugg liii nice na tropp Wayy
Fatel néna waw bonne mariage yo Allah féwnu
Yo diawdi e mbésngou noto amine
La vidéo est d'une clartè si éblouissante, l'image d'une pureté si hypnotisante...sans compter ce talent phénoménal.
"Souma ko doune-doule wone sakheu...yeugue-yeugue bi, sensation bi nek ci clip bi melnani vivre na lou ko raw..."
💖💖💖💖 Peace and love
Machallah laff thiat ya meune Ya eup dole kirassoulay iow rk lay touppppp barki alhourane 😘
Diadieuf Bro, tres nice clip!!! tu es le meilleur.
Most respect!!! bonne continuation.
Free Ngaaka.
Macky ligueyo dé!
SUPER Ngaaka kula bagn dafay sonu rekk.Yafii nekk et quand je revois la fille qui accompagner MHD dans son clip MHD sama khol bi dafay melni lem
Ah oui c'est elle!! Elle est trop canon j 'adore MHD
Nice
Pierre Sene q
Free ngaaka...name nagne laa
❤️😍😍😍😍❤️ J ecoute encore et encore si ça dependait que de moi j appuierai sur l bouton like 1000 fois
'
Of oklm
mbaguel ammna dooler kou beug baparer diehnaa the king blinde
NGAAKA BLINDE YALLA NALA YALLA DIAPLÉ BAGUA GUENA DIËL BII TJI BARKÉ PROFET MOHAMED SL☝🏿
Faye Ngouda amine
Amiiiiiine waaay
Machallah sa niane nangouna ❤️ Seydina MHD ken dou mom 🥰🥰❤️😇
Sa niane nangou n'a
Amine
ce clib est super cool way nekhhhhhh nekhhh la defff bonne continuation ngaaka
ohhh😍😍😍nénna waww bou yagu
DiDiShÙu bLiNdEz wsh
DiDiShÙu bLiNdEz c'est ça. le clip est en avance sur les textes parsk néna waw bu yagu. nice beat kmem mais clip dess na fidel
DiDiShÙu bLiNdEz néga waw bou yague mais sons bi nékhoule dara ngaaka moy sama rappeur la mais clip bi andoul ake son bi
Sileye Niasse ta raison bro mane aussi fans la mais bii dialoul d
Yacine Dieng nio farr yaw bi mome none yii dananiou wakhe
nguaka Nak haleii bii deiissnaa moll dh😂😂😂😂😂mè nice clips
Baby,Chérie,"SOUU"sa va naka waar 😂😂😂😂😂😂lol mai ngaka lolou moy lane?mai kan mem tu es the king nagouna NEENA WAAW.
Dij'a la polie Coulibaly lol
Dij'a la polie Coulibaly 😂😂😂😂no ya baax ay nop dh "souuu" kay
kingPapy Mrg_leclassicMan lol 😂😂😂😂😂no ngaka moma branché
Lahat khadim dieng kone compe ga bro 😃😃😃😃
lol pour mane dh sweet la wakh
si Ghaaka chante bien et si Le Clip de ngaaka est Nice Aime mon commentaire plz
n
i
c
e
Bib SheeNy mbarikala
Nice mé ngaaka boy bi moy lolou dh
Niceuh clip ! Perfide bandit deug job ci souff le bruit du succès
Waw nkaka nice son..........Anyting rk is waw💓💮💯💯🔗👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑the king of da kingz😃😃😃😀😃😀😃😀😗
ohhh billahi ngaaka guayi do sen morom
2024🎉🎉
Je suis Guinéen mais je valide ngaaka blindé comme le meilleur rappeur du Sénégal de sa génération 2
Ki est là en 2020🥰❤️
2021 wesh MDR 🤣
J'suis là son bi dh Aka nexon😍😍
ta
2021
En 2021🤩
Welcome back suniou ngaaka national.
Nice ngaakha bilahi ni dagno sokhor Aÿ fans Dip lagne.nicccccccccccce
Mouhamed Ndiaye baay boul wakh lolou mane fans dip la mai ngaaka clip bi dafa daall j sw fier si sounou rap galsen
ayy thia ngaka mane yaw laa gueum
ndeysanne ramadan de lanneii passei nga indil niou li reine nak tei privei de ta libertei yalanala god takhawou ba nga libre si barkei wer bou sel bi
ayyy wayy ngaaka
mane iow la gueum ndax daguay rap di dox té do rap dii lokh iow
KING baba le meilleur
Souleymane Sow MDRR 😂😂😂 le meilleur ou le plus null
Babacar Seck
hip hop galsen khmnaniou niou fii null diarroul lath😂😂
Nicena na way on voit maintenant ngaaka sous un autre registre.vraiment t'ai un rappeur complet.
Ki écoute 👂 en 2019
Maguinii
Sono mbaye
Ki es la en2020💑💟❤💕
@@omardia6658 moi
AsoTi
nice papa ngaka blindé yalla nalla yalla soutoural
2 million de vue qui et la en 2019?
Nooooo neeexx na. La chan son est très bien faite. Instru, mixage rien à dire.
Nul n'est nulle ici , l'importance c'est de travailler dure pour s'en sortir . Le rap galsen est en train de faire des démarches dans tout les côtés . Les gens deviennent de plus en accro grâce au nouveau tallent ... Respect à vous . ❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
jaloux .....
Samba Fall PlG bien di
el capo junior non frère ne dii pas sa ... Moi j'écoute toute les rappeurs srx ... Je suis un mélomane carré 😂😂😂
Yayegueye Diop C'est la réalité , la vérité s'appelle Dieu ☝🏾️🖐🏾❤️❤️
Samba Fall PlG Rap galène for ever
Oooh temps magui wine 3ème ndeysane 😢son bi lala commencer top ngakaa ba legui ❤🎉
Nice good job Ngaaka! Gel bu nice ,Son bu nice, Style bubess ,Clip original. Ku bagn Ngaaka digua dh say bo yewo vue yii di doubler machallah depuis Bargny
ngaka do nid yaye papou nieup lo beugeu yalla na la ko yalla defal benene laniou beugeu
Bb néma waww . broo ya xam leup wayyy thanks
Gneup nenay waw
l innovation s ennonce au coeur de galsen msii ngakka
mangii doon soucié cii gejelaa déeg. wayee kontaan naa. j'ai aimé le vidéo avant même DL regardé. après l'avoir rgrd s'il y'avais possibilité d'Aimé encore le vdo j'hésiterait pas. tellement daafa nic
Guél yima top barrina mais lolou dou dara way ❤beugu nala way bouniou xoulo beuguoumala bayii🎉
Nena goor yimou diota xam yép malein geuneu gentl 😢bouniou wété si nék malein geuneu bantal 😂dinama faun ray😮thiokotane ma way ❤lélé mou dompatt ma teupp tombatt 😢mou réé bisou 😘 ma rk songuatt té nane ma do guattt😂mbarikalah fi ni do guat 😅ték guama sompatt 🦈🐟wiss si salade 🥗 def si tomates 🍅jus d'orange bi daal ma rk gua khamni amoul diambatt❤❤❤❤❤❤❤Ohhhh jtm papa ici ta fille Maty en Octobre 2024🙏
C'est avec ce superbe son que je découvre Ngaaka Blindé et le beat est énorme. Keep the good work up!
tioooo boy ngaaka niouul nga!!
Ki est la en 2024🎉
Sama rappeur moye ngaaka blindé le roi des rappeurs c un rappeur qui rap bien alhamdou lillah ngaaka mane yeuw la beuge wallah bonne contination merci rappeur
Ngaaka chien leuh quoi , 😂😂😂 , koone mouneu déff sons yii , bravo 👍🏾💪🏾
NGAAKA YAlla Na la yalla defel diam tè leral leup free
Mho waxonn naniou la bayile niouy guenné par 10 nionn niouy guenné par benne Man me kou niame pasi té niamm dayou béye xame ni dou bene Man nééma waaw Mbaarikallah Mbaarikallah for life
Ki MM boko tathiouwou sax daye fethié mayelenn ko touti rek mou radakhie fi yepu
serieu mane fans dip la mai bi mome nice trop li mo bakh rap bi bandi sakh bravo les mbarikala
Aliou Dia balma déé nekhoul ba nékhoul mais ngakaa il est très null DIP d'où moromam akhloubrick wakhi noppi deugg rek la wakh son bi mom dokhoul
Me linga wax amolue fenn foko tekk man douma fans dip me foumou defé Lou nice damakoy wax fi clip menole rombou fi
Aliou Dia nonn sérieux clip bi Nice na trop yow réal nigga
Eh baby sheriie shu ça va eh nakawar.#Freengaka
nenala Waw!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!franchement sonbi nekhna
khalebi bou retaane Sama xol bi day mellni lémm yaw khalebi bou dokheé sama xol day mellni leem! yeah King babaa💪💪💪💪
no sokhna si kay seysina ba parè com mogui dèfar pti dèj bi mais clip bi nice na trop
Ils sont trop beau, son bi nice na aussi. Mais le realisateur ne s'est pas donné au fond les images moy lolu
pourtant image nice na dè par contre moi je me dis texte bi n est pa riche ya trop de rèpètition
Racky Anne je trouve auusi
soda Mbow je pense que c'est pas la répétition mais ce qu'on ressent avec la chanson.
Rackyanne brikest 😂😂
NICE NA NGAKA TOUT ME FELICITATIONS BON CONTINUATIONS
Nice papa ngaka clip bi dal na trop c magnifique
Pour dire la vérité son bi dioylo nama bly depuis mon enfance
ohh j'ai aimé Ngaka si kaw si kanam
Ngaaka rabeutoul li nicessoul bayilen yi way
si tu kiffes ce son 😍😍
tap sur j'aime
Xalé bi bou rétané sama xol bi melni lémm ...xalé bi bou dokhé thiakass thiakass guinnnn ....nice bro ....
1:21seconde ecouter bien ya un son qui me fait tres colle a loreille NEMA WAWAWWWWWWWWWW
mais bro colle en yagui thi dehh jsui ton fan n1 bonne contuniation yagui thia
Oui nama wawawwwwwwwwww
Ngaaka dou nitt..chapeau frère... Bne continuation
Ki ecoute en 2019 comme moi like👍❤
Ndeyesane son bi m rappel beaucoup de choses
Nice Nice Nice 🔥. You're on top man
Bi doufi amat way ngaaka
who here in 2024??❤
Août 2000 Baba the King🥰😍 dama ko nop nak🤣
Wawww c vraiment cool , vraiment chapeau
Authentique et de votre réponse
Ani gniko beugue King baba❤💪
eh tathiouko tathiouko tathiouko ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ki est la en décembre 2k23 ngaaka blinde toujours meilleurs de ça génération
Nice Clip , nice Son , nice Fille. En tout cas contana trop Ngaaka diaral Djolof nakk on t attend
ONT ES TJRS LÀ JUSQU'À LA FIN ❤❤❤❤❤FIÈRE À NOTRE KING❤❤❤
reviens nous frere..Ki es là AOUT 2018?
🙋ndeysane
Avril 2019
Mamadou Diou ; nakamu
mouhamed thiam Nice bro
@@alimatoudiop1901 king baba
ngaaka bou bénn yoné outall ko xamné yéna niro tain ! mé nice a part ca
Weuh mane dama khamoul sakh li gnaw si guel bi ngaaka wakh na deug khaléé bi bou rétané kholam day mélni léémm
Carrement djissumako tahm
Oui c'est vrai
ah ly nékh na thi xol 😍😍😍
Je suis pas trop sur hip-hop ms se clip bilahi j'aime.