Del woor mane lolou sa m'arrive parfois mais damay woor rek mou diekhe peut être que tolou naniou si seuy té ama gouniou mais dieu est grand yalna niou borom may ay borom keur niou bakh inchallah mou done lou gueuneu si nioune
Salam coatch ass et coach mia Moi avant damaY tok 5 jours duma déme toillette après la woté si sa numero yu Si lagne ma diokh séne traitement homoroïde yii Machallah au début bir bouy daw lama done déff mais léguii mome am na 1 mois bou traitement yii diéxé ak légui chaque jour au toilette 🙏🏼 AlhamdulilaH je vs Remercie mercii bocoup Pour tous.
Cc coach lo kham thi diépi sa farr wala sa dieukeur ba boula wower une fois, deux fois gua énervé 😢dama diépi sama farr bi th défouma dra il me soutient machallah, sama lepp moko yorr té takouma mais damaka diépi th je sais pourquoi 😢
Waa Ass mbiroum Dove bi moom doosi wakha djiguéne yi dé dieul nagne sén yonou bopou Dove bi dé molénn geuneul soune awra yi ndakh nénagne goor dou projet
Salut ass et mia Dimbali ma Guire yalla aye pithie moma sonale daniou ma wakhone ni ndokhou siti la ma dieule ci sene traitement ndokhou siti yi mais dégnoule ma beug benene solution
Slt les coachs comment allez-vous et la fête ça c'est bien passé ? En fait je dois me marier dans quelques jours inch'Allah. Besoin de vos conseils et astuces mes chers coachs. Je suis un peu stressé de la suite 😢
Salut les deux coach j'ai acheter votre traitement sopk mais souma deffé ovules yi thi 3 jour damay am constipations mais thi 2 jour yi soumako dindé douma am constipation khawma louko waral
Salut Ass et Mia ! Sama fess yi parfois damay sentir ni dafa am louy teup si bir . mais dama am ay rew si sama fess je veux savoir si c'est à cause de ça
Salut ass et mya man lima diakhal moy ndakh boy sékh ak sa sokhna nokh momi di guén si kou djigéune ki molay wanni danou na Wala ? Moy nokh mo wékh mi tamou mélné loy colé
Yane siyi Dangay envie reukk 15 ou 20 fékk khalé paré wouniou mane problemou premier la am mais sama 2 eme Damay déme ba beug mou Diekh mais bouy Dieux damay 😂😂😂😂
As salam anlayka warahmatoullah wabarakatouh coast asse , Mane deh j'ai 24ans mais sama thiopéret bii dafa reuy té doyoul wone niii , té Say youma excité wé baa daanou rekk mou daa dii délou watt nékeu lou ndow , té damay toy khep kom youtou kat. May lathié ndakh c'est normal asse
Slt coach mane ak monsieur on t'aime tellement mais sama sikk moy dama deugeur bope borom soutourala ba bouma défé erreur day mélni darra khéwoul mais bougnou néké si rapport damay déf lou métti walla mou fété ma kaw dima mbéte en faisant rapport té mane dama fragile trop après souma méré il fait tout pour néxale ma souma néko fasséma mouné mou nou ko ndax dama beug. Té depuis 3ans de relations on régle nos problème ensemble noumay déf
Salam mes très chers, en fait j'ai une question pcq depuis bima commencer def musculation de façon régulière en changeant mon alimentation pour atteindre une bonne forme physique et athlétique, dmay guissni limay teudd guoudi Di guent sma sperme Di guén c'est devenu trop fréquent presque chaque semaine alors que avant c'était pas pareil.
Del woor mane lolou sa m'arrive parfois mais damay woor rek mou diekhe peut être que tolou naniou si seuy té ama gouniou mais dieu est grand yalna niou borom may ay borom keur niou bakh inchallah mou done lou gueuneu si nioune
Machaallah yalna yalla mottali leppe inchaallah ❤
Amine y’a rabbi 🫶❤️
Kay ma def la niarel,boba sounou keur day nekh ndakh fallen AK gayenn day nekh
@@IssaFall-hi7lg degueul lolou bayil togne
@@manegaye non mm pas sakh d'où ay togne sakh
Salam coatch ass et coach mia
Moi avant damaY tok 5 jours duma déme toillette après la woté si sa numero yu
Si lagne ma diokh séne traitement homoroïde yii
Machallah au début bir bouy daw lama done déff mais léguii mome am na 1 mois bou traitement yii diéxé ak légui chaque jour au toilette 🙏🏼
AlhamdulilaH je vs Remercie mercii bocoup Pour tous.
est-ce que ton hémorroïde te causer des problèmes de troubles sexuels ?
@@boubisto 🤭je suis célibataire
@@pacoelpresi3896 c'est sûr que célibataire boudoul déf dara ngua 🤔
Diam thi yéne❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala coach As et Mya amna solo
salut coach ass et Mia am na solo yalla na séne diam yague way ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salut Ass et Mya….. j’ai remarqué que tu as maigri Ass quel est ton secret svp
RESPECT à vs deux ❤❤
Man reyi mia momay danel bilahi Mi del ree 😂 waye
No assa amoul 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Cc coach lo kham thi diépi sa farr wala sa dieukeur ba boula wower une fois, deux fois gua énervé 😢dama diépi sama farr bi th défouma dra il me soutient machallah, sama lepp moko yorr té takouma mais damaka diépi th je sais pourquoi 😢
Je ne sais pas pourquoi ?
Tu ne l'aime pas c tout
@@ndeyeawandiaye7006 en bon tu trouves
@@Bi-noush oui c ça
Waa Ass mbiroum Dove bi moom doosi wakha djiguéne yi dé dieul nagne sén yonou bopou Dove bi dé molénn geuneul soune awra yi ndakh nénagne goor dou projet
Gor Dou Projet Dioudou fékh Sa Bay takki Sa ndaye endiko Thi keurgi doundelle ba Nga mag Nga nane Dou Projet
Slt dama beugue kham l’an moy khatal awra jiguéne svp
Niawko
Salut ass et mia Dimbali ma Guire yalla aye pithie moma sonale daniou ma wakhone ni ndokhou siti la ma dieule ci sene traitement ndokhou siti yi mais dégnoule ma beug benene solution
❤❤❤❤
Slt les coachs comment allez-vous et la fête ça c'est bien passé ? En fait je dois me marier dans quelques jours inch'Allah. Besoin de vos conseils et astuces mes chers coachs. Je suis un peu stressé de la suite 😢
Slt ass Boune bouye khasane bala guaye ame diame rek dougal sa baramebi si bire
Salam Ass mane damadi nouveau marié wayé souma defé rapport défoi maniwbi daye guénat lou warl lolou réponse svp
Salut les deux coach j'ai acheter votre traitement sopk mais souma deffé ovules yi thi 3 jour damay am constipations mais thi 2 jour yi soumako dindé douma am constipation khawma louko waral
Damadon utiliser nep nep pour khatal mé legui damay job surtout pendant nuit legui es meuna am lo khamni damay geuneu khatal svp
An kon néb néb day takh gua khatt
@@YacineKa-g3kWawaw
Coach sama question bi doungene ma tontou ngir yalla gnakh bouy khegn si yeuré lokoy waral AK loukoy safara
Li souma rayoul 😂😂😂
Ngi daniou réw 😂😂😂😂😂
Slam djigéne bou eumb té infectio mba dou ko sonal si wasin bi ak lane mokoy dindi 🙏
Salut Ass et Mia ! Sama fess yi parfois damay sentir ni dafa am louy teup si bir . mais dama am ay rew si sama fess je veux savoir si c'est à cause de ça
Wa Mia ma chérie diokhal sama question Ass
😂😂😂😂😂modducilanss bi
Salut ass et mya man lima diakhal moy ndakh boy sékh ak sa sokhna nokh momi di guén si kou djigéune ki molay wanni danou na Wala ? Moy nokh mo wékh mi tamou mélné loy colé
Slt ass et Mia aye bithi you nek si dokhou goor l'an mokoy dindit svp
Lan moy waral sa ndiap digawa toth
😂mode silencieux
😂😂😂
Mya yak ass loungen bok amgen complicité de
Ayy mook laniou ma chérie
Yane siyi Dangay envie reukk 15 ou 20 fékk khalé paré wouniou mane problemou premier la am mais sama 2 eme Damay déme ba beug mou Diekh mais bouy Dieux damay 😂😂😂😂
Slu coach ass j' ai que 25 ans j' ai tombés amoureux ❤ d un femme âgée de 28 ans je veux des conseils avant je lui dit mes sentiments merci
Karaw boune mome amoul ndiarigne 😂😂😂
Wat ko sèt 😂
@@alhajiloum😊😅😅
Amneu dou touti sakh. Boko watté do tok
nbakh ngua ba nga moy yalla
Mdr😂😂😂😂😂😂
Ass ay texcule youy khassane lou Koy dindy
Coach damay sa pénis bouy dèlo lane ko waral tè man ma souma seuye wla si nianka seuye bi may lathie lane moko waral tmt
Asse djiguene bouye wakh ak copin wam di toye rek ak di am envie saw nakh bi di metti louye problème bi stp
Amoul béna problème daga nopaté rk téh tollou sî seye aussi
lanmoi njerin nge lage si garr
Quelle est la solution naturelle pour éviter la grossesse comme c'est difficile de retirer le pénis lors de l'éjaculation ?
😂😂😂😂😂
Poure mane dou ay mbalake wayé dagua done moytoulo djiguéngi ndakh lale wéne meune na idi lénéne
As salam anlayka warahmatoullah wabarakatouh coast asse , Mane deh j'ai 24ans mais sama thiopéret bii dafa reuy té doyoul wone niii , té Say youma excité wé baa daanou rekk mou daa dii délou watt nékeu lou ndow , té damay toy khep kom youtou kat. May lathié ndakh c'est normal asse
Louy thioparett
Louy doufale awra djiguéne
Svp répondrer mon question
Karitè
Karité avec gowé chaque nuit si tu te réveilles tu verses de l'eau froid tu un fait chaque jour bah 1mois tu vas remarque d'énormes changement
Slt coach mane ak monsieur on t'aime tellement mais sama sikk moy dama deugeur bope borom soutourala ba bouma défé erreur day mélni darra khéwoul mais bougnou néké si rapport damay déf lou métti walla mou fété ma kaw dima mbéte en faisant rapport té mane dama fragile trop après souma méré il fait tout pour néxale ma souma néko fasséma mouné mou nou ko ndax dama beug. Té depuis 3ans de relations on régle nos problème ensemble noumay déf
Salut cv c'est Gregoire encore ma réponse svp
Salam mes très chers, en fait j'ai une question pcq depuis bima commencer def musculation de façon régulière en changeant mon alimentation pour atteindre une bonne forme physique et athlétique, dmay guissni limay teudd guoudi Di guent sma sperme Di guén c'est devenu trop fréquent presque chaque semaine alors que avant c'était pas pareil.
C'est normal frère par l' augmentation du taux de testostérone
Yeah frangin suis d'accord de ce point devue. Merci pour ta réponse
Ass kagn ngay déf émission spéciale si texte spermogramme binga wakhone
Mais cotch dama beugue gua diapaler ma si fébarou [ok] (Yakkél) en wolof sonal nama trop
Hôpital
Amoul kouko beug gratuit 😂😂😂😂
Amena gno xamené dagnouy exagéré parfois 😏😏
bou mo gniè ma sonou Islam degual nala nguay takho koor nbakh ngua ba nga koy
Man souma yéwo sama yakhou ndig li dafay métti trop wayé souma commcé déff ay activités mou sédd louy waral lolou??
Eskeu dou fin fingay fanaané matelas bi wowoul? Wala di oval
Bayil blagues yii
Salut ass man dama begue tack diabar mais qui ma begue dafa seye ba tasse lanla l islam wakh thie je suis salibataire
Wouy tamme Lou bonne rk😂 mais balma nak
Jël sa awra diko dugël sa digënté niaari weeni jabar di yëngël ba daanu ndax mok mballu nioo yam wala
❤❤❤❤