M cette fois ci elle a bien fait j'aurais bien aimé l'épisode précédent bi badiane gnewer mou waxko nax ndiaga Thiam yegueko mo gueun tay mou gnew ndiaga di wax Mouy diay faux nane dougn lein bayi basi kanam fatma Thiam nima KO xaré
@EvenProd, Diotna nak nguén kham ni Bêté Bêté Paracétamol la ci téléspectateur yii. Matin, Midi, Soir... A chaque annonce de chaque nouvel épisode vous nous faites plus tomber amoureux de cette série 🎉❤❤ Bêté Bêté rek❤🎉
Ko gueum ni Maréme Sall dina ame déception si Mr Sow rek lalal j'aime... Mom sahh kou dem neikoul "Bété bété" bimouy wotei... Je sens la grande déception de Cette Dame
@@sodadiouf4667 il paraît que Maréme Sall tourou Makhoudja bi mooko nékhoul de ce fait mou changé ko touddéko papaam, loolou moo takh moom mounaane ko papi. Mais même bouniou bookké papa Khamou niouko
@@yacineba7386 fattt nagn gniou deh au lieu niou def poste binde ci... Dedett dagnioula nieuw setane série pour wakh ci yonente bi saws. Meunolene gnio diakhasseh deh
Kou d'accord ni Dieynaba Tal té woul lamignam mais Dafa diongama té makhou mom rek lay top mais Marieme sall gawna changée deh❤😂🎉 Babel tey lay am deh ba paré guéne
@@adugirl3863bly ioe tu as tout compris sunu la guissé gua yakhar ni niofi guéneu mais luniy wahh akk déff si souff do sahhh comprendre mais yallah baxna
@@adugirl3863bly ioe tu as tout compris nak sunu la guissé gua fokk ni nio fi gueneu mais lunguy déff si souf do sahhh comprendre Fatma thiam es pire que Marème Sall au moins Marème mom elle assume
Les commentaires de série sur RUclips En France 🇫🇷 : C'est une très bonne série j'ai vraiment hâte de regarder le prochain épisode Au Sénégal 🇸🇳 kou beugg Seydina Mokhamed beusseull j'aime
Dioula Thiam joue aux devinettes avec sa maman daba . Celle c lui demande où est ce qu'elle a pris la bague . Dioula lui dit qu'elle a reçu une demande de fiançailles . Alkaly raconte a Makhoudia son entrevue avec dioula a propos de daba Thiam : sa jalousie, son refus de se remarier ,ses pleurs. Il lui dit que daba est toujours amoureuse de lui.il en es sur maintenant . Dioula dit à sa mère que le papa de kheucha est actuellement dans la maison . Père ndiaga s'énerve et demande à a petite fille pourquoi elle est toujours en couple avec la star de la tee . Marième sall informe bassine a propos du mariage de sa fille . Et lui dit que son futur gendre est un noble .et pour cela elle veut organiser un mariage qui restera gravé ds les mémoires. Pa ndiaga donne son veto au père de kheucha et lui dit qu'il ne donnera pas sa fille a un noble parce que lui caste tient a faire un mariage endogame. Par la suite il réunit ses nieces Coumba tall et Fatim pour leur annoncer qu'il va marier les deux cousins Diouma Thiam et alkaly .la maman de dieynaba négocie pour que les deux enfants aient plus le temps de se connaître. Sa cousine parle avec la soeur de alkaly et lui relate les faits . Cette dernière lui et qu'il serait mieux de donner dioula en mariage a son petit ami plutôt que son grand frère . Devant l'incompréhension de tante Coumba dieynaba lui dit que sa mère est contre cette union. Les raisons qu'elle a évoqué est que diouma malgré son statut de cousine est née hors mariage . En plus elle est métisse .seul sa maman est castee.son père étant noble. La tante s'indigne et menace d'aller rapporter les propos de sa cousine au vieux ndiaga Dieynaba r
Vraiment EvenProd, amel nguenn gnou akkh...dou nguenn bayi ba Dimanche matin nguenn douggal BA yi? Mane dama dagn koumpeuh...sou nguen moytou woul sama biir dina daw...ndakh yakamti sétane ! Li tamite deugg leu...yenn BA yi ken douko telleu douggal...issshhhh😢😢😢
Keppe Kouye def bac Yalla nala ko yalla maye si ak keppe Kouye def bfm yalla na nieppe ame diame si barcké seydina mouhameth
Aminn inchallah avec une très bonne mention
Amen
Amine inchallah
Amine
Amin
Kou d'accord né marém sall mo geun fatim Thiam ?? Wayé sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine
Fouy sakh Fatma Thiam koumou diouroul beugoula di yakk bayy yakk sa mbokou
@@MbeneSECK-vf7bd bon la déf
Mareme elle n’est pas hypocrite elle est très sincère mais fatim thiam c’est de l’hypocrisie pure nak
Amine yarabi
Guenouko nank mouwaye fathma mo faux ta Bone
Kou guiss né DieyNaba Tall Wahkaatt leu😢😢😢 Ell Parle Trop😢😢
Doul rek lay déff😂😂😂😂😂
😅😅guémigne gui thi bopam mo gaw té ratax sheuuuttt
Mais bakhna si yaye 😂
Peut-être limou wakh aussi meuna sauvé Diouma Thiam, père Ndiaga changé avis 😂
Bly téi boukay déff dou noyi 😂😂
Dieynaba Mogui soga netali lou am solo 😂❤
😂😂bilay
Merci comme ça diangueyi tasss
Bilay iow😂😂😂ak meune siweul mais elle a bien fait cette fois-ci 😊
Elle est rattakhlée en personne
@@minachou8135 sérieux Li rek la meuss netali louma nex 😂🚶🏻♀️
Où sont les amoureux du prophète mouhamed psl ❤❤
Salalahou Allah Mouhamad ♥️♥️♥️♥️
Salalahou allah Mouhamed
Yagu nako wakh Dieynaba dafa mena netali 😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂
Kou d'accord ni diaynaba tall momoul lamigname bi rk j'aime 😂😂😂
Ki daffa meun netali 😂
Niou wang gni nétali rk lagne meune 😂😂😂
Depuis le début lolou la done wakh 😂 d'où netalii deh wayer Loumou yeug mou siiww😂😂😂
Dieynaba kay vrai doul Katt leu😂😂😂
M cette fois ci elle a bien fait j'aurais bien aimé l'épisode précédent bi badiane gnewer mou waxko nax ndiaga Thiam yegueko mo gueun tay mou gnew ndiaga di wax Mouy diay faux nane dougn lein bayi basi kanam fatma Thiam nima KO xaré
L'amitié entre Alkaly et Makhoudia j'apprécie ❤👍
@rassoulmane9287 👍
Waw kay badienne naka wakh Mame bou goor bouko défé Dinako may ckheucha kome bonheur diouma lay Khôl
Dieynaba tmt meuna Mew trop loutakh amoul bamel bire 😂😂😂😂😂
Naka wakh nieup nopalou!! Fatim Thiam dafa moudjou soff sakh
Aye waye Yalna Kheucha takkeu Diouma Thiam
@@seynadiop6854Amine
No fatim Thiam kou bonn la dji wakh djiou reuy😮😮
Pour la première fois ma contaan ci ay fénou Dieynaba Tall 😂😂
🤣😂😂
Amga morome kone. Fatim Thiam il est tant Diaga Thiam découvrir ko
@khadycisse9675 Mbadou mougui bakhe. 😊
Dieynaba tall comme passoire yama meuneu nétali 😂😂😂😂😂😂😂 , manshallah ep ep qui est tu?❤❤❤❤
@sitoebassene8244 Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ? 🤣
@EvenProd, Diotna nak nguén kham ni Bêté Bêté Paracétamol la ci téléspectateur yii. Matin, Midi, Soir... A chaque annonce de chaque nouvel épisode vous nous faites plus tomber amoureux de cette série 🎉❤❤ Bêté Bêté rek❤🎉
Wawawww
@musasanghare6520 Merci beaucoup, ça nous fait plaisir. ❤
Bété bété a dépassé la bar des très bons séries Sénégalaise 🎉🎉🎉
@mohamedelhabibndiaye8069 Merci beaucoup, ça nous fait plaisir. ❤
Ko gueum ni Maréme Sall dina ame déception si Mr Sow rek lalal j'aime... Mom sahh kou dem neikoul "Bété bété" bimouy wotei... Je sens la grande déception de Cette Dame
Mm conception k moi en plus le gars n’aime pas la file et n’est pas un torodo déception bou reuy lay am
Mareme Sall est-ce que bokoul ak makhoudia pape nah migui wah petit makhou sama pa lala touder
Sow Lawbé la
Layyy lolou ngayy khalattt mr sow mossoul nekk torodo😂😂
@@sodadiouf4667 il paraît que Maréme Sall tourou Makhoudja bi mooko nékhoul de ce fait mou changé ko touddéko papaam, loolou moo takh moom mounaane ko papi.
Mais même bouniou bookké papa Khamou niouko
Bété bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤🎉🎉🎉
@BayemodouGueye-dk3qs Merci beaucoup. ❤
KO bague seydina mouhamed lal j' aime ❤
Arrêtez ça s'il vous plaît toujours le même commentaire parlez de la série s'il vous plaît
@@yacineba7386 fattt nagn gniou deh au lieu niou def poste binde ci... Dedett dagnioula nieuw setane série pour wakh ci yonente bi saws.
Meunolene gnio diakhasseh deh
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
Deelen wakh si théâtre bi way , beugeu j'aime bay beugeu dé
Souma namé aimer yallah na dei
Diéynaba tall fenn Kate la kou d'accord lalal j'aime😮
Beugouma djikoom netali rek lay def
Mais bakhna si yaye dji com k dayy bagn mbokam
Elle ne dit que la vérité, elle véridique, elle dit en haut ce que les gens disent en bas
Diouma Thiam doit savoir ce qui l'attend si elle épouse Alkaly
D'où fenkate doumana gardé dara😂😂
ANA SOPEY yaa RASOUL ❤❤❤🎉
❤❤❤❤
Yalna gnieup ame wer ac werler ba 𝒍𝒐 beug nga mrune ko ame yalla mane nako ❤❤😊
Yalla nala ko yalla defal yaw aussi ❤
Amine
Mais guiss ni Diéynaba day nétali rèk beusel j’aime 😂
@Diarista90 Deite wae. 😊
Aka ma rafét xol damay j'aim comantair yi rk❤❤❤
Yow bayemodougueye naka diékeu maner dagua meilleur khole
@@adugirl3863 noka khamé😂♥️
@BayemodouGueye-dk3qs Lolou nexna. ❤
Paco nimi wakhé aka ma nékh 😂❤
Même mane😂😂
Dieynaba Tall tey sa netaly bou meti amna ndierign 😂
@Marthe154 Lo xalate mame bou goor defko bouko yeugué ?
Fatma thiam tay gua dé😂😂😂😂😂😂
@sodasall7636 Lo xalate mame bou goor defko bouko yeugué ?
Dieynaba meun na netali😂mais content nasi😂
Au moins gnou kham vrai visage yaye dji
Eyy 😅😅😅😅 rima
@rimachouofficiel1805 Deite wae. 😊
Dieynaba deh dou fén mais loumou yeugg mou siw 😂 kimo rataxlé😂😂😂😂
Netali moo tax filma di neekh
wakhou netali kate deug ngafi wakh 😂😂😂
😂😂😂
@@rassoul3548 ahhh motaxite kone mokal na rôle lame
@@mansoursy3270 sétlouwo dieynaba tall xana yaw
Dieynaba rek layy topeu😂😂😂😂😂
@MonicaMonica-dv6hd 👍
Bilaye Dieynaba Tall khamnani kéne dou dieuw nite ci sa kanam déh 😂😂 ndakh bo paré sénnn 😂😂😂 merci
@fatouthiam7663 Deite wae. Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
@@evenprod c'est possible 🤣🤣🤣 yayam déh mome gnep la béttt
Yawemi lire sa ma commentaire yalla gua téral saye parent si baki seydina mouhamed lala❤❤❤
Amine yarabi ❤❤❤❤
Amine yarabi ❤❤❤❤
Amine 😅❤❤❤❤❤
Diaynaba dal netali😂 rk 😂😂
❤❤❤❤❤❤❤
@gassesamb63 Deite wae. Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Pour une fois que je suis avec notre ratakhlé nationale 😂😂😂.Bravo wayyyyy
@aissatasy8925 Deite wae. 😌
@@evenprod Ah oui elle a très bien fait de mettre a nu l'hypocrisie de sa mère
Kepe kou beugue serigne touba lalale cœur ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Kou gueume niii bête bête 🎉 est la meilleure série rek ❤️
@Dieynabangaido-ev1em Merci. ❤
Diaynaba tall mo meuna nétaly❤❤❤❤
@amyseck6813 Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Kou d'accord ni marém sall mo guen fatim thiam rék lalale j'aime 😂😂😂😂😂😅😅😅
@user-tq9yg9pi3l Ah bon ? 😂
Diéynaba tall vrai sénégalais dou fêne mes loumou yék mou siw machalah 😂😂
@mamychoudiassy1259 Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
@@evenprod diéynaba kay comme tamé bravo à vous ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
billahi mame bou goor mo beugue bock❤
Kou diépi Fatim Thiam rek lalal ❤
Merci à Ndary Baba pour ce beau rôle
Wa yeen dieynaba mii nitt la😂😂
@ibrahimambodji3220 Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Kou d'accord ni Dieynaba Tal té woul lamignam mais Dafa diongama té makhou mom rek lay top mais Marieme sall gawna changée deh❤😂🎉 Babel tey lay am deh ba paré guéne
@naboungome7612 👍
Bilay dieynaba tall mo meuneu netali😅
Mom kégn comme tamis Dou teuyé dara
@@papediabong8468 Doyna war d😂
@Khoudia-Samb Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Kepou kouy deff bac yall nala ko yalla may té mou guen thi yaw
Diouma gui beugue té❤
Kou d'accord farou amina bi dou torodo la lal j'aime ❤😂😂
@Mou-f4p À suivre. 😅
Yayou dieynaba tall mi kou fausse la wayy ki soumboulou moko geuneu
Wayè dome dji netalinako trh badiene souko wakhè ndiaga thiam mou regleko😂😂
Ki kay gneup la beteu 😅
Elle a dépassé les limites de l’entendement
soumboulou dalay wan karement ni begoula mais ki day matt di euff
Bilahi
Djeinaba tall mom laminge biii day dem gratuit 😂😂😂😂😂
@CoumbaCossoko Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ? 🤣
@@evenprod dama titt thie mom😂😂😂tay série bii dine wathie mbe zéro
Vraiment Fatim Thiam fausse na merci bcp badiène wahh ko mame ndiaga dhhh 😂
Khadijandoye massi fatma thiam yider nio fess si adina bi liniouye khègne diwo wouniouko
@@adugirl3863bly ioe tu as tout compris sunu la guissé gua yakhar ni niofi guéneu mais luniy wahh akk déff si souff do sahhh comprendre mais yallah baxna
@@adugirl3863bly ioe tu as tout compris nak sunu la guissé gua fokk ni nio fi gueneu mais lunguy déff si souf do sahhh comprendre
Fatma thiam es pire que Marème Sall au moins Marème mom elle assume
@khadijandoye2495 Lo xalate mame bou goor defko bouko yeugué ?
Dienaba tall meune ngua yabekou trop mais contana dakh mame bou fadial niou wakh dakh sa loumou wakh rafetoul 😂😂😂
@LaminCamara-wu8lg Deite wae. 😎
Kou guiss ni bassine thiam mo nara découvrir mR Sow
@saliouthiam8869 À suivre.
Coalition d'accord si Mariage kheucha ak dioumm ❤
@aidandiaye6482 Noleine di def mame bou goor ?
Kou dakor ni bete bete moy meilleur série de 2024
@aramthiam8303 Merci. 👍
Les commentaires de série sur RUclips En France 🇫🇷 : C'est une très bonne série j'ai vraiment hâte de regarder le prochain épisode Au Sénégal 🇸🇳 kou beugg Seydina Mokhamed beusseull j'aime
*Seydina Mouhamed sall’Allahou aleyhi wa salam
Thiey tamè yereute Djeynaba 😂😂😂😂😂😂
@fatimetouniang938 Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
MERCI DIEYNABA MANE SONOU NA SI FATMA THIAM WAYY .PERE NDAGS DOKHALAL
@user-rk4wf8ds2t Lo xalate mame bou goor defko bouko yeugué ?
@@evenprod Lou kha saw
Dieynaba tall yay diehou lantinore kagn ngay bayi netali seuy Kat do def Lou fanane si iao rk yendou si askan wi😂😂
Ay way roram la rk
@@NdiayeDié-p9w dégueule rôle la mé amna Dieg you melni netali day indi division entre sa famiy ak sa bel famiy lolou bahoul
Wayer tay netali bi baxna😂😂😂😂
Yow deh ngatafaye khana bimaye yèdeu suma diabari dome bi yangui toguone suma gorro lou nior mou nètali lou nioroul mou nètali
@NgaytaFaye Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Non mais Dieynaba aussi comme lantinor sheutt
Mom dal néna déy séneu rék😂😂
Djeïnaba Tall daye séneu réek 😂😂❤️
@maimounaba6810 Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Sa majesté Dieynaba Tall à l'honneur 😂😂
@esperanzafaye Lol. 😊
Pour une fois j'apprécie le ratakhler de Dieynaba 😂
@thiorojo 👍
Longue vie à even pro❤❤
@djbillvoice Amine. ❤
Dieynaba Tall lamigne bi comme laalo😂😂😂😂
Merci dieynaba contane si yaw sa féne yi mogui may sogua nékh😂
@ndeyefatougueye7612 👍
Dieynaba tall Tass na keur😅😅
Ana nie wara Magali touba ❤
Pardon tamkharit wala lafal touba ou c'est moi qui comprend pas wala yonou j'aime leu😂🎉🎉😂😂😂
@@Ndeyeawa-lc8ir magal touba rek lanouy topou
Inchallah
Kou d'accord né diouma Thiam doul Kate la 🤣 lalame j aime😂❤
@NdeyesokhnaFaye-rh6rh Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ? 😌
Adouna mafi geuna beug sonko 🥰
Ey waye khamal sa bop rék mane awmaci sago ❤❤
@@diamilatoubarry3308 daga bah rék 😂
Ayyy dieynaba tall mi ratehhléga daal liiii euuupna wouyayyyyy😅😅
Ay diaynaba tall ya meune séneeeee😂😂😂😂ndéké bassine mola tanei
Eye mamiekhoudiadiop bassine koumou taner mba amena
Kou d’accord ni Mareme Sall niénio la rk lalale ❤😅
Wawawe Djeynaba mi da meunoul téyé lamigname bi
@MaimounaTraoré-o4r Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
betbet 😝💟💝💝
Dieynaba Tall mi meuna fene trop😂😂😂😂
Kou daccord ni Daba Thiam ak Papay Kheucha dinagne nobanté beusseul j'aime 😢😢😢
@abdoukarimsarr6652 Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Merci dieynaba 🎉🎉😂😂😂 hamni seuy bi dou ame ❤
Bété bété meilleure des meilleures séries 🎉
@MaxBoye-qe6sv Merci. ❤
Dieynaba comme rideau maiga😂😂😂
Dieynaba tall mo ratakhlé😂😂😂😂😂😂😅
Dieynaba tall ritahléna esk méloul ni tamite😂😂😂😂😂😂
Djeynaba mi amul beneu soutoura lougne ko wax rek mou nétaliko yalla naniou yalla mousal si Soxna bouy netali
@abdoudiop3591 Deite wae, est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Kou yakhamti episode bi lalal jaime
Djeynaba Tall damako beugu day féne bay fénal yayam😂😂😂😂😂😂amoul limite khalébi
Dafa dofer li motakh am yar bakh
Awasowdiop boulma rèlo waye dama fèbar tèye suma tension bi mo yèkk bilaye wakhgua deugeu fène badi fènal sa yaye
Kou d’accord ni Dieynaba tall netali la meune l’ale j’aime ❤❤❤
@marieprince9058 Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Ay Dieynaba Teudieul sa lamagn 😂😂😂bi
Bouko teudie serie bi dou neekh.
@@rassoul3548walahi kone dou nekh mokk bassine rek mais est ce khameguèner badiene tamit dou yoro wayer si peulh yi la
@user-ed2ef6kx6m Est-ce que dou da diaxler si li yaye dji wakhe ?
Merci Coumba Tall wax ko sa nidiaye fatim Thiam dafa boneu trop😢😢😂😂
Dou yaw Dieynaba tall guani do bayi netali ahh yalla bakhna
Alkhamndou lilah sanéx filaye diarré mér may dioumou ki mou beug ndax da mér kheucha & Diouma kassé❤❤
Dieynaba kou meuna fén la😂
Wa Dieynaba tall 😂😂😂tay mou dougueul yayam😂😂😂wouayayyy ki mo meune netaliii
Dieynaba tall féneu yingaaa nékké yakko tayyy 😂😂😂
Machallah ❤❤❤
Est ce qu’une bonne âme charitable peut nous traduire ce qui se dit svp ? baraka Allahou fik,
Vraiment je suis impatiente
Dioula Thiam joue aux devinettes avec sa maman daba . Celle c lui demande où est ce qu'elle a pris la bague . Dioula lui dit qu'elle a reçu une demande de fiançailles . Alkaly raconte a Makhoudia son entrevue avec dioula a propos de daba Thiam : sa jalousie, son refus de se remarier ,ses pleurs. Il lui dit que daba est toujours amoureuse de lui.il en es sur maintenant . Dioula dit à sa mère que le papa de kheucha est actuellement dans la maison . Père ndiaga s'énerve et demande à a petite fille pourquoi elle est toujours en couple avec la star de la tee . Marième sall informe bassine a propos du mariage de sa fille . Et lui dit que son futur gendre est un noble .et pour cela elle veut organiser un mariage qui restera gravé ds les mémoires. Pa ndiaga donne son veto au père de kheucha et lui dit qu'il ne donnera pas sa fille a un noble parce que lui caste tient a faire un mariage endogame. Par la suite il réunit ses nieces Coumba tall et Fatim pour leur annoncer qu'il va marier les deux cousins Diouma Thiam et alkaly .la maman de dieynaba négocie pour que les deux enfants aient plus le temps de se connaître. Sa cousine parle avec la soeur de alkaly et lui relate les faits . Cette dernière lui et qu'il serait mieux de donner dioula en mariage a son petit ami plutôt que son grand frère . Devant l'incompréhension de tante Coumba dieynaba lui dit que sa mère est contre cette union. Les raisons qu'elle a évoqué est que diouma malgré son statut de cousine est née hors mariage . En plus elle est métisse .seul sa maman est castee.son père étant noble.
La tante s'indigne et menace d'aller rapporter les propos de sa cousine au vieux ndiaga
Dieynaba r
@@fleur19merci nous les burkinabé on souffre sans les sous titres 🫶
@@fleur19 merci beaucoup pour la traduction je suis malien
Ayway sanékh bayil diouma ak kimou beugeu 😂😂😂😂❤❤❤
Tkt dinna ko nangou ndakh khass bi dinna laleuh kholam kii beug seutam khassouko kimou bokal khass ko
Diaynaba tall bamou neke khale khana yayame dako tamale netaly😅
Yalla na diamou yague rk ❤ ❤
Fatim thiam bone nga marieme sall mola guene fouf au moins elle n’est pas hypocrite elle dit les choses en face dou neubeutou
@mmembacke6263 Lo xalate mame bou goor defko bouko yeugué ?
Wahhh Dieynaba Tall est-ce que dougn ko kholatt 😂😂😂😂
Vraiment EvenProd, amel nguenn gnou akkh...dou nguenn bayi ba Dimanche matin nguenn douggal BA yi?
Mane dama dagn koumpeuh...sou nguen moytou woul sama biir dina daw...ndakh yakamti sétane !
Li tamite deugg leu...yenn BA yi ken douko telleu douggal...issshhhh😢😢😢
😂😂😂😂
@@AissatouBa-lh2qu Too'ma...sama biir ba ngui kourr-kourri ndakh dagn koumpeuh épisode bi...li tamite jamm leu??
@@mypbarro5416 dou yone deh mounone negn har beu soubeu mom 🤣🤣
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@AissatouBa-lh2qu genrou BA you intense yi kagn...
Bi mom n'a thi tons niogs diot😂😂
Diaynaba tall khana lallo lay ndécké diko agné 😂😂😂
Dieynaba mi meun n'a netali déh 😅😅
Rang mouy gaw