keur ass tv
keur ass tv
  • Видео 655
  • Просмотров 24 393 779

Видео

Nane la djiguene di deff pour khame point faiblame sans que mou deff rapport....
Просмотров 4,6 тыс.14 дней назад
Nane la djiguene di deff pour khame point faiblame sans que mou deff rapport....
Goor bou naye so neker ak moom nane ngaye deff....
Просмотров 6 тыс.14 дней назад
Goor bou naye so neker ak moom nane ngaye deff....
lane moye yok testostérone thi goor ....
Просмотров 4,6 тыс.14 дней назад
lane moye yok testostérone thi goor ....
pourquoi les hommes ont du mal à rompre une relation.....
Просмотров 4,8 тыс.14 дней назад
pourquoi les hommes ont du mal à rompre une relation.....
Djiguene bouye danou rek doyale louthiye pekher....
Просмотров 13 тыс.21 день назад
Djiguene bouye danou rek doyale louthiye pekher....
Guerté kembe ndakh daye yok ndokhou goor...
Просмотров 8 тыс.21 день назад
Guerté kembe ndakh daye yok ndokhou goor...
Miel ak karité niane ndiarigne la ame thi awra...
Просмотров 9 тыс.21 день назад
Miel ak karité niane ndiarigne la ame thi awra...
comment faire pour oublier son ex.....
Просмотров 6 тыс.Месяц назад
comment faire pour oublier son ex.....
Goor bou naye lane mothiye pekher....
Просмотров 6 тыс.Месяц назад
Goor bou naye lane mothiye pekher....
ndakh danou meunena dindi ndaw thi djiguene...
Просмотров 13 тыс.Месяц назад
ndakh danou meunena dindi ndaw thi djiguene...
Pourquoi y'a des filles qui ont des seins tombés pourtant elles sont vierge....
Просмотров 19 тыс.Месяц назад
Pourquoi y'a des filles qui ont des seins tombés pourtant elles sont vierge....
Di guente Di danou tee yeugoulo rapport bi lolou loukoye warale....
Просмотров 7 тыс.Месяц назад
Di guente Di danou tee yeugoulo rapport bi lolou loukoye warale....
pourquoi les femmes ont du mal a oublier leur EX ......
Просмотров 9 тыс.Месяц назад
pourquoi les femmes ont du mal a oublier leur EX ......
Comment trouver le point faible de la femme....
Просмотров 9 тыс.Месяц назад
Comment trouver le point faible de la femme....
Existe-t-il une amitié entre hommes et femmes ?.....
Просмотров 6 тыс.Месяц назад
Existe-t-il une amitié entre hommes et femmes ?.....
Secrets yii nek thi fonanté, avantages de s'embrasser....
Просмотров 42 тыс.Месяц назад
Secrets yii nek thi fonanté, avantages de s'embrasser....
Djiguene bou ay wename amoul thiouss nane la wara deff....
Просмотров 11 тыс.Месяц назад
Djiguene bou ay wename amoul thiouss nane la wara deff....
Ass sonena thi salibataire nane laye deff pour âme boroom keur...
Просмотров 4,7 тыс.2 месяца назад
Ass sonena thi salibataire nane laye deff pour âme boroom keur...
Différence bi nek thi entre s€xe ak mbeuguel...
Просмотров 7 тыс.2 месяца назад
Différence bi nek thi entre s€xe ak mbeuguel...
Secrets yii nek thi thiep ak Gower....
Просмотров 16 тыс.2 месяца назад
Secrets yii nek thi thiep ak Gower....
Thiey liiye khew thi salle yi...
Просмотров 4,4 тыс.2 месяца назад
Thiey liiye khew thi salle yi...
Ay wene toute khassane lane laye tekki thi djiguene...
Просмотров 21 тыс.2 месяца назад
Ay wene toute khassane lane laye tekki thi djiguene...
Différence entre l'homme de sa vie et l'amour de sa vie...
Просмотров 6 тыс.2 месяца назад
Différence entre l'homme de sa vie et l'amour de sa vie...
Djiguene bou amatoul ndaw ndakh dako wara wakh farame...
Просмотров 6 тыс.2 месяца назад
Djiguene bou amatoul ndaw ndakh dako wara wakh farame...
Règle douloureuse, lii mothi gueuneu gaw ,Lou naturel la ...
Просмотров 2,8 тыс.2 месяца назад
Règle douloureuse, lii mothi gueuneu gaw ,Lou naturel la ...
Yoner sa diabare khaliss ndakh force la walla...
Просмотров 5 тыс.2 месяца назад
Yoner sa diabare khaliss ndakh force la walla...
Maniwe ndakh Dina reuyeul ay wene walla dette...
Просмотров 7 тыс.3 месяца назад
Maniwe ndakh Dina reuyeul ay wene walla dette...
Astuces pour salibataire pour contre les infections....
Просмотров 3,8 тыс.3 месяца назад
Astuces pour salibataire pour contre les infections....
Salibataire Bouye setane coach ass...
Просмотров 7 тыс.3 месяца назад
Salibataire Bouye setane coach ass...

Комментарии

  • @jeanmarcmanga6945
    @jeanmarcmanga6945 23 часа назад

    amna garabi

  • @nafidieng7663
    @nafidieng7663 2 дня назад

    Mane sama bop bi lay diap chute de cheveux bou graw lay ame

  • @Binetathiam-o3g
    @Binetathiam-o3g 2 дня назад

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @momadoundoye8193
    @momadoundoye8193 2 дня назад

    Sa numéro la beugeu

  • @BasKan-x4w
    @BasKan-x4w 2 дня назад

    yal na nga gudd fan

  • @AwaNdiaye-pj2lg
    @AwaNdiaye-pj2lg 3 дня назад

    Slt ass nep nep bi naka lan Koy utiliser pour mou teudie la dama accouche bou yakoul mais dama yatou

  • @amyseydi1086
    @amyseydi1086 3 дня назад

    Mia ladialma coach Ass djiguéne noumouy def ba khamni dafa amé sothiéte nakh man katt da am kouma meuseu setal wakh mako mais je ne suis pas sure nakh celibataire la mou diakhalma trop ndakh dama tite ak limay degu yeup si premier nuit si kou am sothiéte .mogui tourmenté sama khel bi

  • @Badjiefit
    @Badjiefit 4 дня назад

    youtube.com/@badjiefit?si=E5_gck7AAf1EWbFK

  • @AisatouNdong-t9o
    @AisatouNdong-t9o 4 дня назад

    Est-ce que dieuguene warna guiss perte blanche chaque jour sans règle

  • @Ndeye-p8d
    @Ndeye-p8d 4 дня назад

    cv mame samakaname daytoy te amouma dieukuerr😢😢

  • @alioudieng5271
    @alioudieng5271 6 дней назад

    Merci❤

  • @OumyFaye-z4n
    @OumyFaye-z4n 6 дней назад

    Machalla

  • @KhadimDiaw-uw5lf
    @KhadimDiaw-uw5lf 6 дней назад

    Ass damball sogouf bii ak ivilv bii nan lay def ba am ci magiy tharoy aret teer

  • @NgoneDiaba-s5r
    @NgoneDiaba-s5r 7 дней назад

    Coach cv dama beugue indi thème

  • @FatousyGueye-j3c
    @FatousyGueye-j3c 8 дней назад

    Très intéressant

  • @YacineThiam-vq5rg
    @YacineThiam-vq5rg 8 дней назад

    Diam siyaw ❤❤❤🎉🎉🎉

  • @aissatoudia8881
    @aissatoudia8881 9 дней назад

    Mai vraiment Ass sa Assistante bi berri na wakh ,gor day teral djiguene,Khana koy beug tak digua ko défall lou touti sakh mai vraiment Ass tu parle bien Machallah mai ma chérie del xol si Mia waye Mia dafa douce day deguelou Ass gua balma dee

  • @NdeyeawaTine
    @NdeyeawaTine 10 дней назад

    man capricorne la ms ndox la

  • @djibyba.26
    @djibyba.26 10 дней назад

    Salut coach est-ce que hommes mariée bou geudié déff rapport lanne lako mana dioural???

  • @khadimfaye1598
    @khadimfaye1598 10 дней назад

    ASSE ame nga solution allergies respiratoires

  • @khadimcisse1969
    @khadimcisse1969 11 дней назад

    Merci

  • @NgonéDiop-c1g
    @NgonéDiop-c1g 11 дней назад

    Ya waur dé machala ass longue vie à toi ❤❤❤❤

  • @KhoudiaDiop-s8p
    @KhoudiaDiop-s8p 12 дней назад

    Slt ass est ce déni de grossesse bo démé hôpital bougnou défé eco bi digne kham ni Daguan eumbou wala si 3 mois wala

  • @AminateSamassa
    @AminateSamassa 12 дней назад

    J'espère que ni amoule effet secondaire rk lolou rk momaye titale

  • @Babs-ii7xl
    @Babs-ii7xl 12 дней назад

    Ass djiguéne Bouy dora accouché niata mois lay tokk pour meneu dieulatt eumbou

  • @NgonéDiop-c1g
    @NgonéDiop-c1g 12 дней назад

    Machala ame na solo yague fii rek té werr❤❤❤

  • @AliCisse-ei6pd
    @AliCisse-ei6pd 12 дней назад

    Merci coach ass bravo 🥰🥰🥰👈👈👈👈

  • @KhadimDiaw-uw5lf
    @KhadimDiaw-uw5lf 12 дней назад

    Waw ass louy maye yaram la bugg ak magiy tharoy nan lay def ba amci❤

  • @MouhamadouLamineDrame-w9l
    @MouhamadouLamineDrame-w9l 13 дней назад

    Man sama copine da am infection ms xawmako won legui ben jour niouy flirte ma lécher ko bobou moy 1ère fois dmay lathié ndax meun nama lor ak nouma nara def

  • @BintaBa-o8g
    @BintaBa-o8g 13 дней назад

    Coach man sama rakk bi 16 la ame mom awra bi day métti di khassane aussi tamite day guéné liquide bou blanc solution la beugue stp

  • @MatyGaye-yi9zf
    @MatyGaye-yi9zf 13 дней назад

    djiguene bou eumb si niata mois la wara dokhontou

  • @badWilliams307
    @badWilliams307 13 дней назад

    Ass li nay wakh ni nekh na deh 😂boula yabo boul fi wakh méfaits yi nat

  • @Haddy-w6s
    @Haddy-w6s 13 дней назад

    Merci ❤

  • @ASSANESECKKHALÉST-LOUISSéck
    @ASSANESECKKHALÉST-LOUISSéck 14 дней назад

    Mais sama tourou ndo Beug na gua diapalema te yallah takh man dama am Sokhna mais Soumay def rapport damay télé danou trop te après damay sonou trop douma meun dara ??? sa numéro la Beug niou wakhon si Nguer dieumi yallah 😭😭😭😭

    • @ayasodane9005
      @ayasodane9005 13 дней назад

      Numéro téléphone Yangui nonou ci écran bi

  • @Souleymane-w5b
    @Souleymane-w5b 14 дней назад

    Salut coach, je suis un élève mais mon problème c'est dormir car dans les 24h loumay nélaw 6h casé la louy solution stp ?

  • @SamsoudiineNdiaye
    @SamsoudiineNdiaye 14 дней назад

    Segne ass mane dé dama dém ba manatou ma déf difference entre gor bouma beug ak couma xéméme wolotou ma kéne dal lomay concilier soxla nako trop même soma mané am sa numéro personnel svp ❤

  • @maikellgomis6516
    @maikellgomis6516 14 дней назад

    Me sokhna si kalamagui nekh na de me nak begue na guiss kanam gui xam na moy ndakh😂😂😂😂

  • @MameasstaSilla
    @MameasstaSilla 14 дней назад

    Sothiéte Pour les femmes

  • @kebabayo5521
    @kebabayo5521 14 дней назад

    20 milliona d'abbotment pour coach Ass

  • @diodioba2749
    @diodioba2749 14 дней назад

    Slt coach est ce que boy bakhal persi diko nane déy mayé lubrification naturelle svp

  • @fallbayemor14
    @fallbayemor14 14 дней назад

    Salut Ass man sama copine néna dafa danou si toilette mou dém hopital docteur bi néko dafa perte verginitém té néna mesoul ham goor mesou baram bopam aussi ken mesou mako baraù may ladj eska c vrai

    • @ayasodane9005
      @ayasodane9005 13 дней назад

      Va voir la différence entre virginité et hymen dans le dictionnaire puis revient .

  • @BsëriñMbakke
    @BsëriñMbakke 14 дней назад

    Merci beaucoup coach ass

  • @MamediarraSaliou-y8m
    @MamediarraSaliou-y8m 14 дней назад

    Man de sm Copin bi dayi beugeu dima lale thi guinaw té bou dano si kanam lay beugeu di Saye ak man bou nieukk dama dane bagne mais legui Damako moudié tamou

    • @fayefaye6332
      @fayefaye6332 13 дней назад

      Refuse ma belle conseil la ne te jamais à un homme sans mariage gua balma

    • @Mbeneseck-vi5ne
      @Mbeneseck-vi5ne 13 дней назад

      Mouni copin la degg dh wala🥺 ak sa tour bou yiw bii nga Balma dh esk sa copin bobou ndax dinala takk banga nane seuyé guinaw nekal nit mom dh sou amé limou beug si iow mou takki kenéne noy def Te aussi koula daganoul waroula laal

    • @binetadiao5718
      @binetadiao5718 13 дней назад

      Bayiko mouy lathiété nonou limouy niak diom yeup ndialo baxoul​@@Mbeneseck-vi5ne

    • @MamediarraSaliou-y8m
      @MamediarraSaliou-y8m 9 дней назад

      Commentaires bi ngeunn dit tontou borom amna dieukeur dalen di def loo sm téléphone la doul lay def

  • @Pstarboysey
    @Pstarboysey 14 дней назад

    Sou niowé Casamance fii mou doyal si Timi timi

  • @MameDiarraMbaye-ud6ov
    @MameDiarraMbaye-ud6ov 14 дней назад

    isk souma ko wakhé lima dane yague si mom mogui wadia dégne t 😢begouma moy souffrir 😢billay souma d wo sakh doumako bagua dieul nakh ani sa papa ani sa yaye rk lay wakh t dafa dém ba yobaléma si niaka mana wakh communication t kisi dés man nanio wakh souba ba gone 😢t loum wakh dogne si délou wat😢diapaléma

  • @MameDiarraMbaye-ud6ov
    @MameDiarraMbaye-ud6ov 14 дней назад

    Cv amy tn ass man dama am niari far ms kéneu ki manoul communication man na téh Tlphonne lou mat 30munit dou wakh t mom la begue kisi dés magui koy wadjia bague nakh dafa mana wakhtane souma ko dégoul sakh 😢daf may manqué t ké manouma ko ték louko méti awma choix 😂maraw mia t mia sakh amna choix 😢❤

  • @KardiatouBâ-s2m
    @KardiatouBâ-s2m 14 дней назад

    Coach sounou bén professeur SVT néna naniou bayi di rakhasé sabou ndax day yakk ndaw

  • @Boromtouba4
    @Boromtouba4 14 дней назад

    4ème djiguéne bou tasse😂

  • @AdamaBarry-q6n
    @AdamaBarry-q6n 14 дней назад

    Coach mann sama rakk bou djiguénn daffay nék tout le temps en mauvaise humeur té hallé la elle n'a que 11ans té hawma Lou Koy warral

  • @NdeyeLo-gn3ms
    @NdeyeLo-gn3ms 14 дней назад

    mane dh dama ame ko kham nassi damaka beug lol sah wayé damakaka ragala wax Mais chaque jours gnigui déganté wayé meunomaka wax insbi kouma déclarée amour ba bagne Ndakh môme sonouna trop sah solution nk la beug😢

    • @sankhepor5494
      @sankhepor5494 14 дней назад

      Wakh kako dara nekousi balaa mouy dokhane sa morom

    • @DameNdiaye-dl5lz
      @DameNdiaye-dl5lz 14 дней назад

      Wakh kokou ma chérie bala moulay reuthi 😊

    • @NdeyeLo-gn3ms
      @NdeyeLo-gn3ms 14 дней назад

      @@sankhepor5494 Merci beaucoup vraiment contene na si yén yalla nalén yalla fay😍mais le problème c'est que dama amoul fitou waxkako😥😥

    • @ayasodane9005
      @ayasodane9005 13 дней назад

      Bokko niaméwoul wakh face à face kay déclaré koko par WhatsApp