Bai Sheik Omar Toure’ xariti suma Papa Alagi Bai Cham ak rakam Papa Abou Cham cha Bakau New Town. Ma suma papa, sumai raka ak dohm da nyu dan juleh Aljuma cha keur. Amon na ai talubem yu ma dahn saet si suma keur cha Kotu. Xam naa neh Muhammadu Nassir Niass mu Bai Omar Fatti Diallo Niass chi lohom la ne wohn. Ganaw jumaa, waxtaanam ak suma papa dina dan am solo. Be
Ya mane assarale diamila . machalah amena solo .4 fois après chaque prière . surtout avec une autorisation auprès d un maître accompli.machalah.
Yalla naniou léne yalla fayal y'a rabi !!
Machaallah war nga sax yokk xissa yi sama mame saloum saloum yi bax yi xalei yi ngi ngi len di fattei. Kon roy way mi ngi manquer
Machallah Baye merci beaucoup ❤️❤️❤️❤️☪️
Mancha allah
Dieureu djeuf
Mâcha allah
Machala yala khamnani sama khol sedna
Machalla wakh tang bi nèkh na facaha na am sole ❤❤❤
Machallah
Machalah na yalla yok leer
Manchalla
Thiey Sama brother Moi c'est Diery Andala Cisse Seck
Bai Sheik Omar Toure’ xariti suma Papa Alagi Bai Cham ak rakam Papa Abou Cham cha Bakau New Town. Ma suma papa, sumai raka ak dohm da nyu dan juleh Aljuma cha keur.
Amon na ai talubem yu ma dahn saet si suma keur cha Kotu.
Xam naa neh Muhammadu Nassir Niass mu Bai Omar Fatti Diallo Niass chi lohom la ne wohn.
Ganaw jumaa, waxtaanam ak suma papa dina dan am solo.
Be
💗💓💗👏👏👏👂
Mé môme mossoul diare ndoffane
NDOFANE DOMAME BI GNU DONE WAKH ELHADJI MOUHAMADOU HABIB MO FA NEKONE
Il a bien interprète la vie du Saint homme, Dieu merci.il a sauté l'étape de ndoffane
É yaw nak takal diabarr
Cisse histoire amore fatu dialou niass
Machallah