Senegal deukou nafekh deug deug ... Balla Gaye a chaque fois qu'il perd niouni dafa djekhal... s'il gagne niouni dafa liguey adversaire bi..... Modou Lo daan Ama ak Boy niang niouni voila Oustaz bi wan na nieup ni galathie amoul , entrainer am dolei ak fit moy daan ... apres les memes personnes reviennent pour dire galathie mo daan tapha 😂😂Ou est la logique dans tout ca ? Tapha Tine wakh len ko deug mou wouti coach mental tei travailler vivacite wam mo geun.. Niaka dor bi yeup dafa ragal sou dorei balla beute ko diar si tank ... tei effectivement lolou la def, bam fayo la ouverture am si souf niou thiaxabal ko
Vous savez que dans la vie,si tu es meilleur dans votre travail,on ne t'aime pas, c'est pour cela que si Balla perd on dit qu'il est terminé mais s'il gagne on parle aussi de mystique, dans la lutte,il y'aura toujours les harka foufa,balla c'est comme le Real Madrid en football ❤❤
Esk senegalais amna khél niouy wakh balla mystique la dané alors que tapha tine a frappé avec ses deux mains, il a plaqué balla gaye dialoul, il est parti chez ardo et revenir, niou danko mou djiouk, il a tt fait baniou danko
Sénégal mo beuri nafékeu li balla def si lamb tay am gnou nane mystique moko may victoire tapha mo geuneu nul si gni balla gaye dane khana fayou gnouko khaliss louko téré wouti mystique
Injuste ce que fait Aziz Ndiaye Mois je supporte Eumeu Sene Mais à mon avis n'importe quel titre c'est le Roi qui devrait lutter ça Mais on ne peut pas lutter une coupe sans le Roi 🎉de tous les lutteurs
@@papadiom9260 Saway koudoul danou yallah bindou ko commençant ci borom baatin yi ak gni geun ci hanlam bi.. Lima wakh ci kaw tektal leu à titre d'exemple..
Wakho fi touss 21 mars 2010 Luc Nicola mo teug Balla gaye 2 vs Modou lo té gnépa khamone ni Modou lo la faralone té balla gaye 2 dako dane. Guéw gnari athlètes reck gnofay dess sou arbitre sifflet
Yow nak yaye domeram sou nékone aziz moy diokhé ndam esk balla dina perte couronne bii te aziz organiser ko fii luc nicolas organiser wouffi dioutal tapet lo vs balla gnou nokkouko fii la luc Nicolas organiser baye mandione modlo gnou sathie victoire baye mandione yéne ay hypocrite nguéne
Balla bou dara daloul mo meun si lambeu dji balla gaye mi waroul 6mois san mou beuré vraiment ki moy lambeu❤❤
Bilakhi lolou lagnou kham motakh gnoukay sote mais bougnou ko bayé ak sagom balla chaise laléne di tégal par béneu
Senegal deukou nafekh deug deug ... Balla Gaye a chaque fois qu'il perd niouni dafa djekhal... s'il gagne niouni dafa liguey adversaire bi..... Modou Lo daan Ama ak Boy niang niouni voila Oustaz bi wan na nieup ni galathie amoul , entrainer am dolei ak fit moy daan ... apres les memes personnes reviennent pour dire galathie mo daan tapha 😂😂Ou est la logique dans tout ca ? Tapha Tine wakh len ko deug mou wouti coach mental tei travailler vivacite wam mo geun.. Niaka dor bi yeup dafa ragal sou dorei balla beute ko diar si tank ... tei effectivement lolou la def, bam fayo la ouverture am si souf niou thiaxabal ko
Wakh deuk Bilay
Billahi wax ga deugeu
Blh wax nga reew mi dafa beuri nafeex
Bilay wakhal déh wadji nékhoul ba nékh mais gaindé la té moy khoromou lamb nak
Moma diakhall
Balla ligaye rek ak ndimbalalou yalla moko maye ndam yalla nako djigue
Vous savez que dans la vie,si tu es meilleur dans votre travail,on ne t'aime pas, c'est pour cela que si Balla perd on dit qu'il est terminé mais s'il gagne on parle aussi de mystique, dans la lutte,il y'aura toujours les harka foufa,balla c'est comme le Real Madrid en football ❤❤
La sérénité de balla gaye ma dépasse dou dan ba jubilé ❤️🔥💪
Le 21 mars 2010 demal setaneko bi mou dane modou Lo dafa done jubilé
Le 21 mars 2010 demal setaneko bi mou dane modou Lo dafa done jubilé
Le 21 mars 2010 demal setaneko bi mou dane modou Lo dafa done jubilé
Dedett combat bobou dafeu amone tension motakh Balla daw dem ci supporters yi pour calmer lén xolatal images yii bou bakh.
@@salioumbackeniang2570 me lolou aussi daf si jubilé mounoko bagne frère
Aziz ndiaye dèffa bougueu balla guaye2 ndeysane ❤❤❤❤❤❤
Esk senegalais amna khél niouy wakh balla mystique la dané alors que tapha tine a frappé avec ses deux mains, il a plaqué balla gaye dialoul, il est parti chez ardo et revenir, niou danko mou djiouk, il a tt fait baniou danko
Mashallah talibes cheikh loumou touty touty boulko khepp
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sénégal mo beuri nafékeu li balla def si lamb tay am gnou nane mystique moko may victoire tapha mo geuneu nul si gni balla gaye dane khana fayou gnouko khaliss louko téré wouti mystique
A part Balla Gaye, personne ne peut terrasser Tapha Tine dans cet arène. Même Modou Lo évite De croiser Tapha Tine
Lac 2dannako
Bilay deugu leu keneu mounouko balla rek ko sonal
@@boubacarboiro5813 Mais Lolou amna 15ans ou 17ans
@@bssg9549 Mais danne mom danne leu reck
@@boubacarboiro5813 est-ce que Issa pouye peut terrasser Balla gaye actuellement?
Thieye Balla gaye dou daan ba jubilé koi❤ dara douko depassé
Injuste ce que fait Aziz Ndiaye
Mois je supporte Eumeu Sene
Mais à mon avis n'importe quel titre c'est le Roi qui devrait lutter ça
Mais on ne peut pas lutter une coupe sans le Roi 🎉de tous les lutteurs
Kou fatté liko li Mara niass wakhone thiy Balla Gaye ?
Dou sakh jubiler il est le meilleur
Bilahi dou jublie lamb douko depasse
Loumouy jubilé ci défaite la diougué soga danne jaroul jubilé...
🤪😜😝
@@Victoiremanmême bimou dané yikini jubiler woul ak deux combat yii Niaff Ptit roi sakh jubilé woul
Loumouy jubilé lètii mo Dane yakh ya Diop yekini sii la watio akh nieupp Sénégal mo nekh rek🎉😂😂❤
Balla késsé❤❤❤❤
Mystique fegn na nak
Félicitations Balla
Sokhor fégne n'a nk nanal glace
konn wakhal nii Eumeu Séne daffa téwone lokho Thapha Tine wonn bayii léne sokhor
Danga sokhor yaw
Mystique fègnena kay.gnii teug lambou dji nieup Balla laniou faral.promoteur bo khamni moy soti galathie lii amoul fén.kouni Tapha kén diapouko si galathie khamo lii khèww bilahi
@@YacineSène-s5hpromoteur yi yagu nagn teugu balla mouy danou soyez sportif
Kou wakh mystique danga sokhor balla il est le meilleur tapha dafa ragal balla lolou moy wakh dji
Guine thiéthié balla kassé❤❤
Mai tahoa tine 😂 mo nieukeu Dorr songou plakè 😂😂 bobou Serigne bii diapa goukoo khannna nagnne wakhantè deugu ❤❤❤ balla Goat 🐐
Boulen faté yalla mounan takhawal ma sampeu leu thiey Sénégal
Arrêt d'être compliqué yalla Moy mayé diam Di wakh mouy am yalla moy LEEP mais gni wakh nieupe danio Sante yalla ba paré
Mystique, ceux sont les marabouts qui luttent
Loy xar si beure dji koun😅
Kone demal taak ngimb dane Tapha
Balla moy lamb nak billahi mane balla lay topou
Bilay sa thèse ak dalle te yarou machalla kham adina❤❤❤
Maintenant on attend balla gaye contre eumeu sene
Félicitations waawaawaw
Félicitations balla bly yaye diamar ❤
Kou wakh mystique amoul rk dala diapoul. Lamb affaire tiedo deug leu.
Kouni sokhor amoul rek dala diapoul😂😂😂😂😂😂
Dagua amoull ay mbok 😅
Sa touba ya meunna doull khamo data ndayamme
Même les journalistes sont des supporters ceux qui interview ya que balla
Balla guaye boumou dieulatt modou lô nguir yalla.bouko modou lô dané dagnounan modou moko meun dako diékouwon thi galathie rék
Bravo à Balla mais on ne peut jamais être ampereure si on est pas roi. Parlé du français stp
Il a libéré la couronne
Il fut le premier roi de sa génération 😘
Beure balla mo gueneu woor si lamb dji bilay
❤❤❤❤❤
Où est Mohamed Ali Ndiaye ?
Sen scénario bi yeup modou Lo balla gaye molen takha diouk les chroniqueurs des arènes nieup laniou dieund
SA TOUBA MI DOUL REEEK
FI AMOUL BEN MYSTIQUE GUISSOLEN TOUSSS
😂😂😂😂
Sa touba ragalal yalla
Vraiment certain commentaires me font rire li budul mixtique lann la arrêter wayy
Gni balla dane tapha meunoussi dane kéneu.
Ay morome lagne balla bimi dane yekini ak tyson tapha gnemewoul beuré ak gnome
Yaw bada Liga wakh Balla gaye lepp 😅😢😂
😂😂😂😂
Mo meun mo eup dollé
Tapha tine loudoul tapett dara danouko tote leu boundoukh bou makk😮😢😅
Sa thies mako wédiiiii
Kholer ba eumeu sene dila dane chimmm
Combat bobou daf si nelaw di andi ay yaar diokh ko thieur bou bari lolou rek moka khagne
Eumeu Sene bouko Balla ak Sa sotone sakh molene meun !
Lamb mo beuri naféh kouné hamnané tapha tine nekoul
Xana fayou niouko tmt??
Dagnou ko meune dane ko bayilén sokhor
Khana Tapha sayou Dano niouné nékoul😂
Louko téré nék et Balla bigniko done dane nékoul wone nafékh yaw rék la domeram
@@cheikhfall2997 seu yaye moy domou haram
Man bi Aziz wakhei sama kourouss meun nassi toukal aduuna la veille du combat lors de l'interview de beuz ci la hamni narouniou diam.
Aziz fass touré la djangué d
Tekksi di talibe cheikh mashallah
Te pourtant Aziz mo ngimb Balla, BN2 doumeu ko daneko
@@papadiom9260 Saway koudoul danou yallah bindou ko commençant ci borom baatin yi ak gni geun ci hanlam bi.. Lima wakh ci kaw tektal leu à titre d'exemple..
@@ClayensClayens Deug leu niakoul baatin mom
Tapha tine balla moko meune lolou Moy wakh dji tapha dafa 10 té boulén faté ni balla moko dakh beuré foufe eup KO fite
Balla doit travaillles dur encore plus k ça
Danou ak aye dannome Tapha Tine ne mérite pas du courage
Mystique bou salté rekk. Çà c'est déglace.
😂😂😂😂😂
Li dou Yonne Azizz Ndiaye teugue lamb dji ba parés faral balla Gaye ay domouram lanou
Yaw mi yay dmrm deugg nak di nafeex Tapha mola gueneu xam Aziz Balla la faral
Yaw mi yaye domeram
Wakho fi touss 21 mars 2010 Luc Nicola mo teug Balla gaye 2 vs Modou lo té gnépa khamone ni Modou lo la faralone té balla gaye 2 dako dane. Guéw gnari athlètes reck gnofay dess sou arbitre sifflet
Luc Nicolaï Kane la dane faral bane domouraaaam la dan yeungeul faral KO aussi domouram
Yow nak yaye domeram sou nékone aziz moy diokhé ndam esk balla dina perte couronne bii te aziz organiser ko fii luc nicolas organiser wouffi dioutal tapet lo vs balla gnou nokkouko fii la luc Nicolas organiser baye mandione modlo gnou sathie victoire baye mandione yéne ay hypocrite nguéne
Sa touba beg micro li rék moy wanéni hamo dara
Setal ci rour bi book ah
Balla gaye kassé
Mistyk rék bou ligueyoul menoul dane
N'importe quoi wallahi les ils oublie vite vite contre boy niang tout le monde avait dit autre chose....
Tapha tine si bopam mo tapéte balla boko beugué dane fok gua gnimé ko ba paré té mom gnimé woul balla
Ki nane neiw la guiss vrai dofla
Boulene niou fonto tapha mo diek dor mem boufeke deniouko diekou deniouko faye te per mbaye ndew mo geun one beug comba bi
Sen 30 bounou nudeye beuré woungne AK balla
Pourtant mok Ama baldé sakh combat la
Trabajar mo meune analyser 🤣🤣
Ndadane la bandit la meilleur analyse😂😂
Sa touba com kou gayy 😂😂😂 gat xamoko
Thiotou ndye SA touba
Yawe kou rew nga kham nga louy touba
Sa data ndaye yaw
@@ibrapene5963 sa koyou seringe AK sa baye AK sa yaye AK sen wa keur