Bébé saloum je te conseille d'aller t'entraîner et t'entraîner dur pour continuer d'exister. Et surtout parler moins. Tes attendent de toi un champion et un philosophe
Mbeur Kadou yis Rafetna, sa xel Rafetna mais Honnêtement côté Sportivement da nga Manqué Entraînements trop dafa Fégn si sa combat, té aussi reculer pour mieux sauter dafa bakh
thieuy le poete de la lutte sénégalaise.........yalnala yallah japaléé way
Walahie bb saloum je l estime beaucoup walahie nitt deug la li déss thie carrière bii yalla na lépp done ay ndam si barké Serigne Saliou🤲🏼🤲🏼
Aka rafétt kholl yalllla nala yalla diape lerall sa yone bb
Ma chalah Bébé Saloum yalna yalla doli sa soutra te maye la aye ndame you bari barak yonéntou bi
Ki dou bb saloum bb talif la wakh rék
Yaw ak sokh combat talif la
Félicitations Jacob 💪Félicitations mama lamine 💪
franchement c'est un homme bien. un très bon conseiller.
Thiey le roi de la communication
Wakh rek lay defff ki dou rousss
😂😂😂
😂😂😂
Dafa bari😂wakh dh 😂😂😂😂😂
😂😂😂 bilaye Sokh Vs bb saloum combat bou nekh
Communication bi nice na m'acha'llah nala yalla diapalé cou geume yalla nga 👌
Kèpeu kouy fans bébé saloum boko beugué méré bouko dèglou
😂😂DEUG rek nga wax
😂😂😂😂
Lamigne bi moo neeh mayou yalla la 😂
😂😂😂😂
Moom ak sokh combat la dé🎉😂
Wakh laniou geuneu Meun d
Ndaw signature bou nekh douma ko meusa râté dinga degue ay wakhtane you nekh
Tte façons nit kou geum yalla nga courage champion bne suite de carrière
Kou Mane communication nga. Kou geum yella nga yalla nalla yalla may
Il communique bien Machalla ❤❤❤ yalla bakhna sa ira wakh djiou rafet kaser mo ameu solo
Champion gua lamb kousi nek ak lilaa yalla thieurélé lamb bolou agnn la kou nek sa werseuk rek gasii lekk❤❤❤coeur pour bb saloum
Macha Allah tu es un bon croyant mougneul biss Dina gneuw nga am ndam
Courage wa Kaolack est derrière vous particulièrement and taxawou lamb Kaolack
Macha'allah il communique bien ❤
Billahi excellent communication
Merci beaucoup bébé salom❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah li sport la ya tanée tapha tine
Vérité absolue c'est Dieu qui décide
Machallah❤❤❤
Machala machala yalla na a aye Ndam you beuri nieuwe inchallah 🙏🙏🙏
Champion nga 7defaites 18 victoires❤❤
Il vit dans l'antiquité ce gars genre yi ils sont tout le temps dans les nuages
Diadieuf baye fall bi ❤❤❤🎉
demal nga defi talife😂😂😂
Bébé saloum démal entraîner dji . Yalla tégoula natou ci lamb car lamb dafa kharam . Lamb sport leu gnak entraînement mola daan
Késsé kholal eumeu sène nimou takhawé mé mom dagoul féne
Aka nékh lamignieu mais machallah borome bakh la nak yalla nako yalla tékill natou yi
Ndeyssane aywaaaay ohhhhhhh ah dete waaay ohhhhhhh yaram dawnaaaa 😂😂😂
😂😂😂😂
Saloum continu ton chemin diambar deug ngeu danga amoul koula diapalé rèk dina bakh inchallah 🙏🏾❤
Koula bayi nga def interview 😂😂
Walay lou leer ga wakh ....😂😂😂
Kiii😂😂
Bébé saloum nak tu es très intelligent pour out koula djappalé ,sa intelligence mola wara djappalé.
Dél deff 12 accélération thi Dune yi liguey rapidité thi bir Souf ak musculation ❤❤❤
Mom le passé rek😅😅😅
Yallah bakh cheikh talif
Bèbè Ak Sokhou😂😂😂
Bobou nékhoul bébé vs Madji madji😂😂😂
D'accord na
Yaw modou soxlawoul sakh conseil modou kéneu douko sarahé... comprendre na loutakh amo carrière bou bakh...modou eumeu balla doyna, naniou laay chance xaaleyi....
Billy wax ga dege
😂😂😂wakh rek lay def
😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Waw n'a dégue deh
Eumeu séne 10 victoire 10 défaite 😅😅😅
Ñafale sandye gatesagemine😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Kou d'accord ni Bb Saloum dafa wara bayyi beuré dém nékk chroniqueur ou journaliste Lamb
Woyy bb saloum defna interview 😂
Ndeysane
Yakamtina danou ba kheuy dii wakh bb Saloum wakh rekk ngaay deff
Wa bb saloum loy wakh 😅
Cheikh talif wakh rek😂
😂😂😂😂
Défaite bi doula nakhari parce que amo ay supporter
Wakh la gueuneu mane. Wakh rek
Meilleur roi de la cominiquation 😂😂😂😂😂thiey bébé dou danou mouk😂😂😂😂😂😂😂
Wax raik 😊😊
Diadieuf bébé Saloum
No bb saloum ki amoul diome wakh rek lay def
Mais combat bb saloum vs sokh lolou ndiarndém la dee
Waxou nioula lolou démal entraîner mo guene xallé 'gua sa morom yi ladane gneup avancer nagne
mais ki derniere victoiram kagn la wone? aidez moi svp
Contre Baye Mandione
Wakh rék
Mo Dakh wakh si mbeur yi Dakh fé danou
Esk mongui entraîner skh 😮
Franchement nak mais Bbebe Saloum koula khol khamni sa entraînement dafa dess gueunal goorgorlou si coté bobou bo beugué continuer sa carrière si lamb
Bébé saloum je te conseille d'aller t'entraîner et t'entraîner dur pour continuer d'exister. Et surtout parler moins. Tes attendent de toi un champion et un philosophe
Sou wax done mayei ndam yak Sokh mom yeinay nek roi des arenes wax rek djeuf zero
Modou Sokhla woul sa conseil
Wakhrek
Talif katt nga legui
😢
Dél entraîner
Bb saloum deugeu nékhoul
Ms boy yii m'a guis nii gniola eup dolé
Mom pour mom lamb lamigne bou nekh leu Bro demal entrainé di dem Contact di beuré Bo beuguè dess thi lamb
Aka nekh lamign😂😂😂
Kana lekho mbakhalou saloum😂
Mbeur Kadou yis Rafetna, sa xel Rafetna mais Honnêtement côté Sportivement da nga Manqué Entraînements trop dafa Fégn si sa combat, té aussi reculer pour mieux sauter dafa bakh
Bb salom diakhalnama 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Nopalou lénn modou diokhé woul dieuloul revanche xalei yii lay beurél
Kou d'accord thi combat Bébé Saloum ak Sokh
Ki da beurii ndeye wakh danou rekk lafi néké bouko kéne teugueul lati combat😂😂
Wakh rek lay deff😂😂😂 Thiey Bébé lamigne bi mo nekh😂😂😂 bou wakhé rek nga diebalou😂
Wakha. Na degueu dhe âme n'a vp you nek ci kaw gnio eup ay défaite té moléne eupelé ay victoire
Mom nak dafay fen rek 9 Victoire la amone ak 7 défaite legui amna 8 défaite soma wedé demal renseigné wou
Bb borom baax la nak
Wakhe Mom meunguekko deffet yi berrina
Ben si eumeu sene 13 victoire 10 défauts 😂😂😂😂
Vraiment il parle bien degue wax suma Donne bene télé damakoy dieul
N'a dieul boy niang
Bebe saloum. Papa. Boye.djine
iaw demal ga Tok modoul jeloul balla Gaye 😂😂😂😂😂😂
Bb saloum ak sokh combat leu
Wakh rek
*Soudone wakh rek, heure bii doon neu roi des arènes bou yague. Yow gui daan guenagoul sakh ngey gueine di wakhati encore 😂*
Ana xasse
ki la meunoul supprter ak waxam diou bari
Talif rék
Bb saloum alboury
Ki lamb la wara bayi dem talifi😂
Modou lo dépasséna balla
Balla seul main tout saufs les lutteurs de pikine
Bilakhi qui boog nako bisniki teye
Wakhla mane te do anterene birmi doye wakh
Loudoul wakh khamou ko 😂😂
Dell entraîner