Lima beugeu lath moyy siteu dafa djeul combat bi pour victoire wala pour tenir modou lô en échec analyse yeupp wané na ni siteu amoul chance si combat bi
Siteu reussiroul dara Ama ak BN2 ay diambar lagn danio takhaw deugeul séne bop🎉 Siteu niewoul wone pour beuré Saltél la begone vrai badola la mais Modou mognou togn rék heureusement yalla faynako kholam❤ Félicitations Modou ❤🎉😊 Modou nak Yalla la andal kéne menoul si mom touss 😊
Si bor bobu la bok mais lingay wakh amul. Seytané yé beurii si lamb ji rk mais aziz amul diotu khéxx modlo walahi azim. BG2 la mais modlo la faral et je le respect beaucoup
Lamine golo sur un combat Royal l outsider doit reculer et tenir tête au Roi ! Suis d accord avec quand tu dis MAFIA LAMB VOULAIT LE FAIRE TOMBER MAIS YALLA MOKO SOUTOURAL
Siteu a lutté de la même façon avec zarco. Zarco l'avait terrassé , action biii thi birr la commencer, bi siteu di defff 4 appuis mais fekkk guen nagne sakous yiiii
Siteu day daw rek amoul arrêt 😂😂😂waaayé booo beuré roi fok ngua deuggueul sa bopp samp taxaw si arrêt bi pour meuna am roi 👑 félicitation MXL
Masha Allah Grand Lamine liga wax deugleu modou demb niaane yalla piir mokkossi guénné
Felicidades Modou lo el Rey 🎉
Lima beugeu lath moyy siteu dafa djeul combat bi pour victoire wala pour tenir modou lô en échec analyse yeupp wané na ni siteu amoul chance si combat bi
Siteu niewoul wone pour beuré Saltél la begone vrai badola la mais Modou mognou togn rék heureusement yalla faynako kholam❤
yein Niar noko ko dane ko nguen di doul rek
Lolou mo diara lathie
Wakhal dé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Lathie ga lo am solo
Machallah lamine ✍️ nittou deugue dafa ame solo 👏moithier lamb kéne beugouwone Modou lô ame ndame ✍️ wayé yalla bakhna ségame Sonko lagnouko déf wayé taye lép diékhna ✍️
Belle analyse Lamine merci on a bien compris
Merci lamine
Bonne continuation Grand vraiment tu mérite ton beau Nom Seydina Lamine, nitou dégu gua ❤❤❤
Siteu day daw Rék amoul arrête comme thiak thiak 😂😂 félicitation Modou lo vrai champion 🎉
😂😂😂😂😂😂😂
😂😂thiak thiak
Siteu le nouveau Lac de Guiers 2!! C'est dommage monde de la lutte ils sont contre Modou lo.
Siteu reussiroul dara Ama ak BN2 ay diambar lagn danio takhaw deugeul séne bop🎉
Siteu niewoul wone pour beuré Saltél la begone vrai badola la mais Modou mognou togn rék heureusement yalla faynako kholam❤
Félicitations Modou ❤🎉😊
Modou nak Yalla la andal kéne menoul si mom touss 😊
Bilahi modou moniou togn ki meritei woul niou may ko chance
Thieyy Lamine bilaye yaye gorr thé kham lamb
Mais lamine galo mais contente n'a trop danga wam lamb machalla 🫶🫶❤️❤️
Merci❤❤❤
Merci à toi
Yaw nitou deugeu gua bilahi ❤❤
Félicitations YALMINE bi❤💪🏾
Moko douma yobko ardo danko
Lamine champion nga🎉🎉
Lamine bilahi diam rek gaye ame
Senegal xamouniou sport dangay daw ba am defaite nioulay feliciter
Bilahi
Saway nangoul Lou yalla dogal siteu yalla moko may
Mooma djakhaal
@@miboldieng7574taxaw ak sa moromou goor yalla di’ daww 😂😂😂lolu la deff 😂😂😂😂
Haha😅😅😅😅 mais siteu foumou amé ndam la beugg kham? Yéne doolen ragallal yAllah touti @@miboldieng7574
Machallah Lamine ❤❤❤❤
Il est très respectueux
🇧🇪 Congratulations Siteu 🎉sa thiès incha'Allah 🎉le nouveau roi des arènes en 2025 incha'Allah ♥️🫶
Kou bagne modou lo gua iow 😂
Lamine laff thiate vraiment tes analyses sont vraiment pertinente
Ber becay ak modou mbay
Bilay Lou leer la wakh
Gracias Lamine 🙏
Souko continue siteu dou dane kene
Magnifique
Merci lamine kouniakk kingiaan
Vraiment lamine yaw rk yafi analysé lou lér🎉
Modou lo mo meneu siteu 10000fois
3
Wallahi
Mes Siteu moko dane
Merci grand 🙏❤️❤️🙏❤️❤️🙏❤️❤️🙏❤️❤️💓❤️❤️🙏❤️❤️💓❤️❤️
Yow bou gnou yapp siteu daww lamb ji yeup... Gni djeul couronne roi des arènes yeup meussou Gnou daw guènn sakkou yii... Siteu rek moo beug soon roi des arènes cii guinaw sakkou yi
Merci ❤🎉
O lamine ama est boys on plus de mérite que siteu
Wa Aziz ak bor blé gnio beug moudanou
Si bor bobu la bok mais lingay wakh amul. Seytané yé beurii si lamb ji rk mais aziz amul diotu khéxx modlo walahi azim. BG2 la mais modlo la faral et je le respect beaucoup
Mane lima diakhal siteu day tek ngay dégue légui koudane😅😅 bayiléne sokhor 😅
Livraison gratuite kouko beug defal siteu signe day daw rk amoul arrêt
😂😂😂😂😂
@@barajr3186😂😂
Lamine golo sur un combat Royal l outsider doit reculer et tenir tête au Roi ! Suis d accord avec quand tu dis MAFIA LAMB VOULAIT LE FAIRE TOMBER MAIS YALLA MOKO SOUTOURAL
Mashallah
Kou kham combat ga bilahi
Siteu rek 🎉🎉🎉🎉🎉❤
Bilaye lamine ioe Dangaye waxx dieumeullé sa knm quoi nxx nga 😂😂😂😂😂
Siteu moy ami mbacké Thiam
Lac 3 😂
Ak lou meuna xèw modou danou na😂 borom 3 foi ardo boy bou ndaw bi moko nokou dane ko li lhistoire dinako bindeu 😂
@@leuz.patriotefane lakoy binde🤣😁😁
Amy mbacke thiam kay moko tane. Nele sitteu kay mooy lac3.
Un nouveau Lac2 est né 😀
Siteu nena dou danou tei dou songou modulo lgui wa diamguein dieul lein sen lac 3 daw rek lay deff beuri wakh teksi
Lamine vraiment Yew mom niit bou deuggou ngua
Niom wakha tougn victoire dh 😂😂😂mais ardo lani jubilé 😂😂😂gni nioo bagn senn bopp 😂😂😂ba noppi nak daw alleu bepp
Teu ardo bi sajh guinaw saccouyi lako yokhossou fèkeu modou baisser sa garde siteu door motakh mou dieul avertissement...
Lac3😂😊
Nom baye siteu boulen ko wax thiak thiak plutôt allo dakar😂 lamine dieureudieuf ❤
Bilahi Lou wer nga wakh lamine
Le combat c revanche siteu sathies balla modou lo
Siteu adounam yepou ay daw lako nara diappé😂😂
Billahi
SITEU LANLA DÉFF DAWW BA LADJI DJÉKH LOLOU MOY TENIR NA MODOU YÉNA NGAK DIOM WAYY 😢😢😢
❤❤❤❤
Tiéy Sénégal dangay danou mélni yaa dann😂😂😂😂
Haa ok kone si je comprends bien Siteu dafeu gneuwone pour tenir Modou Lo en échec ???
Dotouma dieynda perpervie daw reck vraiment dsl
Sport d combat stratégie siteu a bien fait son combat félicitations frère
Non vraiment lamine the best ya niou guene
Bilahi lamb dangko tarbiyou lolou xamnassi dara lamine faye
Wakhal siteu deugg way siteu dafa daw ba combat bi diekh
Balla gaye yekini leu wone dafa warone ñeuw imposer modou lo
Modou lo Felicitations , siteu tapet la , DAW rek 😡😡😡😡👎
Siteu kassé 🎉❤❤
Wa siteu amoul areee😂😂😂😂
Siteu a lutté de la même façon avec zarco.
Zarco l'avait terrassé , action biii thi birr la commencer, bi siteu di defff 4 appuis mais fekkk guen nagne sakous yiiii
Niouss nang roi bi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 guediawaye késé
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Siteu mo danne
Modou lo
Wallahi wakh gua deg modou lo diapo nan ko boubakh sakh
Lamine nachallah
les morom de siteu dawounou😂
Number lamine la beugue please 🙏
Max mbargane mo yak combat bi hakh. Siteu ragal leu ioe de ngay sooooop modou ngue beugone mou niak
Ki xaritou modou la
Situe brewoll 😂😂😂
Kone kayyy ioe danga doone tekk khell pour beugg siteu daane.
Siteu dou diambar 😂
Wakhléne deuk siteu da daw
Avant combat bi nieupa ngui wahné Modou Lo poid bi bahna 😂entrainéna ba wow kong,paréna si leup 😂😂😂,Siteu dane ko niouy wahné poid bi da bari 😂😂😂
Nouko siteu dañe yaw😂😂😂😂
@serignegathie6181 bilahi walahi Siteu dako dane 🤣🤣🤣
@@moussapayemane4167Explique 😂
Nanile de l'eau😅😅😅@@moussapayemane4167
@@moussapayemane4167 siteu kouma dane fofou 😅😅😅😅
Sarape ndeyame xamoko
Siteu dara lafi defoul Waxlen ko deug tokk plateau di wax rk la meune
Modou Ardo Lo😂
Kou kham lamb lala tégone
Lamine del mano
Siteu thiaak thiaak yako meunn😂
Délene analyser lou diadou sita dafa daw ba lam dji diekh defoufa dara
Siteu mo dane wallahi
😂😂😂yow ya neikh tapètte bi daaw combat bi yeup
Modou lo bombardier Modou lo takhawoul di mo danou té môme la gars yi félicité
Bobu modou dafa takhaw khekh ak bombardier teh moko opa fuuf
Siteu moy lac2 day daw amul arrêt. Bilahi sama moromu goor douma door may daw dé momako ngueneul
Siteu sou takhawone modou lo reuy ko
Siteu geumeul sa boop way😂😂😂
Amin sa analis 0 faut lierna nagne
Boulén niou sonal beré niarokoy déf siteu beréwoul khékhoul wakho fi dara
Grand nak siter limou déf dou stratégies lolou daw la wakh léne siter deugeu bouléne bagne kou léne méré
Sou taxawonn dathje li moromam yi dathie
Tenir bo hamni si daw guako tekkk. Siteu dayy saboté Di DAW rék
Modou lo combat wame ak bombardier dako daw hana 😂
Siteu waratoul beuré dawe combat bi yeup la df 😂