CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDOUL HAMID SARR:TARIQA CHEIKH REK

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 дек 2024

Комментарии •

  • @attijanibargny9283
    @attijanibargny9283 10 месяцев назад +1

    MashaAllah Yalla samleuuu Sarr rta Salam

  • @omarthiane3430
    @omarthiane3430 3 года назад +28

    Je peux ecouter ce marabou toute LA journee
    Merci beaucoup
    Longue vie
    Kene wakhoul Lou gueneu laire ligaye wakh
    jaradjeuff

  • @cheikhsarrdiagne3077
    @cheikhsarrdiagne3077 2 года назад +6

    Jazakal laahu Anna xayrane wa ayyadaka wa nasaraka.ya saydy abdal hamiid.

  • @papemalicksisse4559
    @papemalicksisse4559 3 года назад +4

    Yalla na yalla defal yokk soutouram ci barki seydina Mohamed psl ham ham ak degou ci mom la fek bakh

  • @adio2.064
    @adio2.064 Год назад +3

    جزاك الله عنا خيرًا سيدي ومولاي وستّرك وإيانا بستره الذي ستّر ذاته العليّة ❤

  • @bassiroudia9345
    @bassiroudia9345 2 года назад +2

    Wallahi eupllla xam xam yomboul Soubhanallah yalla na borom bi sammeuh la aaarla fayyal nioulla yiw ssi barkeii Taha Salalahou Alleyhi wa Sallam❤️🙏

  • @coumbakante7871
    @coumbakante7871 3 года назад +10

    Wow wow ! Benene dimension !

  • @mohamedkare9027
    @mohamedkare9027 3 года назад +14

    Dieureudieuf cheikh Abdoul Hamid sa sopper depuis côte d'ivoire

  • @alioudieng2994
    @alioudieng2994 Год назад

    Yalna sama Borom dimbali la goudeul fane wi Alhamdou lilahi

  • @direlaveritetv5478
    @direlaveritetv5478 3 года назад +21

    voilà l'homme de DIEU pur .

  • @insandiaye6880
    @insandiaye6880 3 года назад +4

    حفظه الله ورعاه وأطال عمره ونصره وأيده وزاده بسطة في العلم والجسم بجاه أحمد صل الله عليه وسلم

    • @Alhassan-y9p
      @Alhassan-y9p Год назад

      Amine

    • @adio2.064
      @adio2.064 Год назад

      اللهم امين بجاه سيدنا محمد صلى الله عليه واله وسلم ❤

  • @mohamadoubabacargueye3364
    @mohamadoubabacargueye3364 2 года назад +1

    Wakhtanames douma si doyal. Yalna yalla bour samouko

  • @adamaajuuf6355
    @adamaajuuf6355 Год назад

    Machallah ❤

  • @mamadousow1470
    @mamadousow1470 3 года назад +5

    Mashalla yalla na yalla goudal fanam bi barakati Cheikh seydi Ahmad Tidiane Cherif rta

  • @babacarkonate9689
    @babacarkonate9689 3 года назад +2

    Merci oustaze je vx te voir

  • @cheikhehane4708
    @cheikhehane4708 3 года назад +1

    Machallah akhsanoul khalikhine

  • @elmalickgueye383
    @elmalickgueye383 2 года назад +1

    MACHALLAH 🙏🏾

  • @adyfall5549
    @adyfall5549 6 месяцев назад

    Dieuredieuff serigne bi

  • @cheikhseck6067
    @cheikhseck6067 3 года назад +3

    MACHA ALLAH
    OUSTAZ SARR YALLA NALA YALLA YOKK XAM XAM BI TALIBÉ CHEIKH YI CONTEN NA GNOU THI YAW

  • @ousmaneamadou8206
    @ousmaneamadou8206 3 года назад +2

    Meussouma deug wakhtan bou ni mell jazakallah khayran seydi abdoul hamid

  • @mandikoundiaye5098
    @mandikoundiaye5098 3 года назад +5

    Dieureudieuf Chékh Elhaz Abdoul hamit sarr

  • @Ndaar-Faam
    @Ndaar-Faam  3 года назад +11

    Ana bann Serigne moo mouna wokh ci leeral foukéelou limouy wokh non diounéelou limouy wokh ci xam xam ak leeral ak néekhaay ??? Kann kann wayy ??? Amoul fenn. Konn bokk Sénégal diaapelènn cii Sangue bii ! Koo beugeu sopp Yalla sopp Yonenteu saws ak sopp CHEIKH akii khalifaames yi diappal cii CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDOUL HAMID SARR.

    • @ibrahimagueye5821
      @ibrahimagueye5821 3 года назад

      Yaguii propagande dh té lolou tariikha bi sohlo ouko.

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam  3 года назад

      @@ibrahimagueye5821 Gosse propagande loumouy firri ????? J'attends une réponse rapide merci.

    • @Seydilxawmi
      @Seydilxawmi 3 года назад

      Dama ko sopou tei guisa gouma ko walahi beug na ko guiss trop yalla xamna lolou

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam  3 года назад

      @@Seydilxawmi Maa cha Allah ! Tu es au Sénégal ou bien ?

    • @Seydilxawmi
      @Seydilxawmi 3 года назад

      @@Ndaar-Faam mbour la deug

  • @serignecisse2573
    @serignecisse2573 3 года назад +6

    Li lerna nagne tarikha cheikh mofi nek bou done niary nitt dong kep kesse nioko gueum douté moudi deug

  • @mordiallo4039
    @mordiallo4039 3 года назад +3

    Masha'allah amna solo

  • @assanesarr7593
    @assanesarr7593 Год назад

    S'il te plaît dimbalima si sourtou Youssouf bi

  • @papendiaye3400
    @papendiaye3400 3 года назад +4

    Ma cha allah

  • @mbayemansour4634
    @mbayemansour4634 3 года назад +7

    Yafi nekk dh koula doul deglou yereumnako wallah

  • @cissepape7433
    @cissepape7433 2 года назад +1

    masala chik rekk

  • @babacardiop7509
    @babacardiop7509 2 года назад

    Waw mom khana siwoul

    • @waadoundou2467
      @waadoundou2467 Год назад

      Siw na kay mais sénégalais yii daniouko ragal

  • @youssouphathiam2910
    @youssouphathiam2910 3 года назад +1

    Merci!

  • @serignepapendiaye2932
    @serignepapendiaye2932 3 года назад +4

    Machallah sangue bi yagu fi te weer lol

  • @makhtarcisse-ft1dq
    @makhtarcisse-ft1dq 9 месяцев назад

    Franchement ki amoul morom

  • @taphatoptop1120
    @taphatoptop1120 3 года назад +1

    Machalla

  • @baidyba1093
    @baidyba1093 3 года назад

    machalah

  • @khafstall9339
    @khafstall9339 3 года назад

    0
    ط

  • @issamagazine9775
    @issamagazine9775 2 года назад +1

    Al hassan Salam, nitu Kacfu bobou, mo niew degal Seydina Limamou Lahi al Mahdi(psl). Amna goor gou Yonnenta bi fegnou neko man ngay wooy, ki moy Mahdi,Ben lane douniou niaar. Yaw Limamou Lahi ngay weddi, té nga né am nga xam xam.

  • @papemalicksisse4559
    @papemalicksisse4559 3 года назад +3

    Borome chaîne yalla na gha am yokouté

  • @gooryallataxawdeugeur4400
    @gooryallataxawdeugeur4400 3 года назад

    Iaw nopil domeram biyakeu derou tidjani ki geu eumbeulone bagn ko mougui fi dh t t affair miss bi soxnasi woténa en direct dinan test adn domeram bi

    • @sopecheikhabdoulhamidsarr7408
      @sopecheikhabdoulhamidsarr7408 2 года назад +1

      Ki d'où dionkh loho djiguene wahouma mome mais ay talibé bewone sakh dougnou nouyou contraire qui mo meune sa mboleine serign ak fo meuna bokk katale sa nedye domram yow deh sa yaye seyouye motakh guayy diguate boroom diamano

  • @mamadouthiam625
    @mamadouthiam625 3 года назад

    Billahi wallahi tallahi yaw mi di wakh amo tousse si yallah.

  • @gnrlng2409
    @gnrlng2409 3 года назад

    Ki moy cheytané en personne,nonou yallah bou mak bi,Aka meun fén ak doul,kouka gueum gueum gua ay fén

    • @sopecheikhabdoulhamidsarr7408
      @sopecheikhabdoulhamidsarr7408 2 года назад +1

      Katale sa ndeye domram sa yaye seyoule

    • @mamoudiallo7100
      @mamoudiallo7100 2 года назад

      li moy wanné né sokhor rek molen diapp. yaw deglou wo limouy wakh diem ci dieulé ay ndiarigne mais parpar lo molen sonal. mom deug rek moko niorr. yaw mi yay seytaané piiir

  • @issamagazine9775
    @issamagazine9775 2 года назад

    Mahdi bu niewoul né mom leu, lutah yonnenta bi niew né may Yonnenta bi. Mbiru Mahdi mom amolen si xam xam.

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam  2 года назад

      MAHDI yonenteu mi borom WAHYOU mooko djangalé baa nopi motakh niou meun cii wokh : :)

    • @issamagazine9775
      @issamagazine9775 2 года назад

      @@Ndaar-Faam je l'ai écouté défendre Al hassan Salam, kokou mo deugale L'Imam Mahdi(psl). Parfois nit deyy reer si biir xam xamam.

  • @MD-ly2yy
    @MD-ly2yy 3 года назад

    Salam mr sarr Faut être prudent ac la khoudba ki est juste un discours. le Prophète d’Allàh n'a jamais dit qu'il fallait le dire qu'en arabe. Merci pour la tarikha d'allah.

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam  3 года назад +1

      Salam, je pense que tu n'as pas compris ! La khoutba c'est le fiqh qui nous enseigne comment la formuler de la même manière dont le fiqh nous apprend:
      ✓ les horaires de prière dans la journée ( moukhtar ; darouri ; wakhtou fayy dioulli)
      ✓ les actes obligatoires dans la prière( faratas dioulli)
      ✓ les actes qui relèvent de la Sounnah dans la prière.( Sounnah dioulli)
      ✓ les actes méritoires dans la prière. ( nguenell yi)
      ✓ les règles du jeûne du mois de Ramadan ( dougeul yeené ; louy dog koor ; louy kaffara etc...)
      ✓ les règles du pèlerinage ( tawwaf ; diamra ; arafa lou ssi manké nokoy rattraper ak loo mounoul rattraper etc..)
      ✓ les règles du mariage ( fassé boo khamni tu peux reprendre la femme après idda ; boo khamni tu ne pourras plus jamais la reprendre ; fassé bou haraam ; fassé bou warr ; fassé bougn sipp ; fassé bou dagane; fassé bougnou sopp etc...)
      Or ce même fiqh qui nous apprend que :

      La khoutba du vendredi remplace les deux rakaates de tisbaar parmi les 4.

      LA KHOUTBA DOIT ÊTRE DITE EN ARABE.

      La khoutba doit être dite en deux temps ( premier discours ; l'imam s'asseoit et se relève pour le second discours).
      NB: Le prophète saws ne donne pas certains détails comme ceux cités ci-dessus, mais c'est le fiqh qui détaille le Coran ; les faits, gestes et propos du prophète saws pour que nous puissions appliquer.
      Donc ton argument comme quoi le prophète n'a pas dit qu'il faut faire la khoutba en arabe ne tient pas du tout !
      Ou alors si tu veux persister sur ce qu'il n'a pas dit, tu vas devoir remettre en cause toutes les règles des actes d'adoration que tu as apprises dans par exemple le livre lakhdari si tu l'as appris bien sûr.
      Donc ce que le CHEIKH a dit est très clair.
      Wa salaam.

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam  3 года назад +2

      Un conseil : baayil musique dafaa haraam ! Mieux vaut love alqourane que de love music.
      Le prophète a dit saws : { musique dafayy sakhal naafeekh ci kholl ni ndokh dii sakhalé gnambi}

    • @sopecheikhabdoulhamidsarr7408
      @sopecheikhabdoulhamidsarr7408 2 года назад

      Ya meuna fene tu sais rien c'est pour cela demal diangui qui mo raw sa mboleine famille ak sa serign yi