AADAMA AK MUSAA : NDAX XAMTU AK DIINE DËPPOO NAÑU CI SEENI MELO? Li Xamtu saxal mooy ne dañoo ñuuloon, ni ko Seex Anta Jóob indee ak ñeneen. Li nu man a fore ci Diine nag moom it dëppoona ak li Xamtu saxal : wax joj jëlees na ko ci Yonent bi muy nettali Tukkib Riñaanam ba, melal ci yeneen Yonent yi mu dajeel yépp, waaye bamu eksee ci Aadama ak Musaa, daa wax ne i nit ñu ñuul lañu woon. Nii la ko waxe: "... ثم مضيت ورأيت رجلا آدما جسيما، فقلت من هذا ياجبرئيل، فقال: أبوك آدم". Nee na bi mu yéggee benneelu asamaan "... Damaa jàll, ma gis góor gu ñuul, am jëmm, ma wax Jibriil ne ko kii kan la, mu ne ma: sa baay Aadama." Moo tax baatub Aadama araab dafa koy jëfandikoo jublu ci nit ku ñuul, " آدمي اللون" (Aadamiyul lawn) fu ko araab waxe nit ku ñuul la ci jublu. Lu jëm ci Musaa, Yonent bi nee na, "... ثم صعدنا إلى السماء السادسة، وإذا فيها رجل آدم طويل عليه سمرة، فقلت من هذا ياجبرئيل، فقال هذا أخوك موسى بن عمران ... " (... Ci lanu yeggee juróom-benneelu asamaan, ci lanu fa fekk genn góor gu ñuul, njool, jige palmaan, ma ne Jibriil kii mooy kan, mu ne : sa mbokk Musaa doomi Imraan...". Lees ci man a dégge mooy Yonent bi saxal na ne Aadama nit ku ñuul la woon, Musaa itam nit ku ñuul la woon, te loolu day dëggël li Seex Anta Jóob wax ci Esipt gu njëkk ga, ne woon i nit ñu ñuul lañu woon...
*Cëyy Serigne Bassirou mbacké khélcom wallahi amoo morom 😭❤️ yalguafi yague té wérr si barkép Serigne saliou mbacké ❤️🙏*
Dieureudieuf MBACKÉ yallah nalla yallah maye fane wou goude and ak weer ak barké ak diame
yalla nala yalla may goudou fan ak wér si barké seydouna Mouhammad pls 🙏🙏🙏
Dira diaf ame na solo yalla nala yalla defal diamo ak wer ak godou fane
Mbacké yalla nala yalla défal diam
diadieuff Mbacke Yalla ngafi yague téwer mbecke amine
Mashallah Amna solo
Machahalla yallana yalla faye serigne bassirou mbacke khelcom barkeb borome touba
Amna solu lolu wakh tanne wi Serigne bassirou mbacke 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳☝️☝️☝️🙏👌👌👌
Marshallah may Allah bless you long life
Th❤️🙏
Macha allah Mbacke Balla 🙏🙏🙏🙏🙏
ma chalah vous m avez bcp appris
Machallah mbacké amna sollo
nimala sopé sounou borom rk lakoy sédél barkeb serigne touba
Yalla na fi yaag lol té gueuna weur machallah
Dieureudieuf Mbacke yague fi lool the ver
Masaallaha طول الله عمرك
Merci beaucoup Rafena
machalla amna solo
Akassa amena solo yague fii🙏
Jeureujeuf Mbacké
Machallah Yalna yalla samoula
diadieuff Mbacke Yalla ngafi yague téwer mbecke
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
amna sole loll yalna la yalla dolle fay
Dieurradieuf mbacke balla aisa
Doundale rék bala aïcha 🙏🙏🙏🙏
jaradiaf Mbacke yallanalayalla samela taguoudal safane amalngagnou ndiarign Mbacke!!!!!
Yalla na nu la yalla fayall ci barkeb mame cu ted ki
sante serigne bi rek
Goud fann
Machalla ❤
Yalnala yalla fay
Mbacké yague fi loooool té wér yalla na xam xam gui yok barkep Borom Touba
Machallah🙏🏿🙏🏿🙏🏿.
Macha allh Mbacke yallena talle de fal dimo ak khewal
Amna solo🙏🙏
Machallah eskeye akasa machallah
Mbacké mala sope nguirr diami borom touba
Amna solo
Machalla
Ndaysan bèereup you am solo yi doo fi guiss ay comentaire yu bërri mais affairu Càaxàn yi rk saytànè nimou ñou euppei doolei sax dafa graw
Bilahi wakh nga deugg
ما شاء الله يكن
Machalla am na solo loll
Machallah
❤️🙏🏾
U
Amo marom balla haicha
Seriegne bassirou maguilay ziarė bu backh
Xana amoul groupe whatshapp mane mom rek lay deglou bilay. Damako beugue rek ta yalla tax dafa am fasakha.
SALAM alaykoum magii len di ziar di lenn ladji ndakh khissa younouss Serigne bassirou mbacke def nako wala
Wa Halaykoum Salam! délo ziar boubax! Déédéét ! défa gouko
Al Meuhmoon Sylla ziar nanla wawa amna yossoef
Diaradiefati Mbacke yallena yalle dé diamo ak khewal
MBACKÉ BALLA YAGEUFI LOLL
AADAMA AK MUSAA : NDAX XAMTU AK DIINE DËPPOO NAÑU CI SEENI MELO?
Li Xamtu saxal mooy ne dañoo ñuuloon, ni ko Seex Anta Jóob indee ak ñeneen. Li nu man a fore ci Diine nag moom it dëppoona ak li Xamtu saxal : wax joj jëlees na ko ci Yonent bi muy nettali Tukkib Riñaanam ba, melal ci yeneen Yonent yi mu dajeel yépp, waaye bamu eksee ci Aadama ak Musaa, daa wax ne i nit ñu ñuul lañu woon.
Nii la ko waxe: "... ثم مضيت ورأيت رجلا آدما جسيما، فقلت من هذا ياجبرئيل، فقال: أبوك آدم". Nee na bi mu yéggee benneelu asamaan "... Damaa jàll, ma gis góor gu ñuul, am jëmm, ma wax Jibriil ne ko kii kan la, mu ne ma: sa baay Aadama."
Moo tax baatub Aadama araab dafa koy jëfandikoo jublu ci nit ku ñuul, " آدمي اللون" (Aadamiyul lawn) fu ko araab waxe nit ku ñuul la ci jublu.
Lu jëm ci Musaa, Yonent bi nee na, "... ثم صعدنا إلى السماء السادسة، وإذا فيها رجل آدم طويل عليه سمرة، فقلت من هذا ياجبرئيل، فقال هذا أخوك موسى بن عمران ... " (... Ci lanu yeggee juróom-benneelu asamaan, ci lanu fa fekk genn góor gu ñuul, njool, jige palmaan, ma ne Jibriil kii mooy kan, mu ne : sa mbokk Musaa doomi Imraan...".
Lees ci man a dégge mooy Yonent bi saxal na ne Aadama nit ku ñuul la woon, Musaa itam nit ku ñuul la woon, te loolu day dëggël li Seex Anta Jóob wax ci Esipt gu njëkk ga, ne woon i nit ñu ñuul lañu woon...
machalla
Diereu dieuf mbacke amna solo loool
Akasa diadieuf mbacké yaguefi lole té wér amena solo lole
💯💯💯♥️💯💯
ana part.2 bi S.V.P
ruclips.net/video/mIumVKaP3bI/видео.html
partie 2 et fin
Diara diaff mbacke
S,bassirou.khelcom
Santa s touba rek
Akasa diadieuf mbacké yaguefi lole té wér amena solo lole
Yague fi lol te wer
diara diaf s bassirou
S.bassirou.khellecom
Sono mame adma bann yonénté sitopp
Yaga fi lolou ta ser mbacke
Kon adama est ce que dou woon nitt kou gnoul kom thi bann bou gnoul lanko bindé
diar diaf
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
Machallah eskeye akasa machallah
diadieuff Mbacke Yalla ngafi yague téwer mbecke amine
Machallah
diadieuff Mbacke Yalla ngafi yague téwer mbecke amine
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
Machallah
Machallah
Machallah