La vidéo choc qui prouve que Selbé avait vu le décès de Bachir Kounta !

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 18 янв 2025

Комментарии • 160

  • @yapadqoi
    @yapadqoi 6 лет назад +15

    Ce qui manque au Sénégal, entre autres, c'est de bons hôpitaux psychiatriques

  • @madamemadame3380
    @madamemadame3380 6 лет назад +72

    Kou sokhoroul aussi, ndangou nii amnga mayou yalla.

    • @andremendi3475
      @andremendi3475 6 лет назад +3

      mayou yalla amousi teuni dafay guis bou bakh motakh islam aramalko

    • @madamemadame3380
      @madamemadame3380 6 лет назад +2

      @@andremendi3475 ce qu'elle dit là Tani lako guiss Waleu rêve ?

    • @andremendi3475
      @andremendi3475 6 лет назад +2

      @@madamemadame3380 bou fekon lou nit guent mou am kon adouna tas

    • @madamemadame3380
      @madamemadame3380 6 лет назад +7

      @@andremendi3475 Tu as déjà entendu le Nom Du Prophète Youssouf ? Lui il savait interpréter les rêves parce que même en l'Islam les rêves véridiques existent.

    • @gabanefall2447
      @gabanefall2447 6 лет назад +3

      Day doul rek

  • @kountacherifmoustapha7091
    @kountacherifmoustapha7091 6 лет назад +21

    Respecter léne doumou adma yi ta bayil Serigne ahmed bachire sou guene meunoul gnanal bou lene Ka touda ti si Sene you haram yi commercé gni deh RK guene fi néké yala reka ham ligniy gneuw Serigne Ahmamd Bachir ak Sidy lamine Niass yalna lene yala yeureum ta xare lene aldiana ak bépou dioulit bou fatou amine

  • @elomarniang1882
    @elomarniang1882 6 лет назад +30

    Bilay nit nit rèk mè yalla moy mayé respect pour selbé

    • @silvanaezidine3872
      @silvanaezidine3872 6 лет назад

      mome meuna sett mais dagne ko yakkk en plus sou guisè dara nakay wakh thie dernière momenty

  • @sunugal4392
    @sunugal4392 6 лет назад +1

    Waareu nga nopi nak. Aka beurri gnouyeu guisseu té nopi. Maman nopil svp.

  • @seydousarr3286
    @seydousarr3286 6 лет назад +9

    on a tendance a lui jeter des pierres alors que de plus en plus elle continue de faire ses preuves (# respecta selbé ndom)

  • @domoubaol6697
    @domoubaol6697 6 лет назад

    Amena niou yalla May nak nako domou adama yii nongou sèlbè mi nitt kou yalla May l’ala 👈👈👈👈👈👈👈

  • @horizon24tv49
    @horizon24tv49 6 лет назад +1

    Je le respecte beaucoup et je sais qu'elle a quelque chose de particulière !!! Pourquoi le lui refuser ?
    C'est la vie, chacun a quelque chose qui lui est propre !!!

  • @electionsenegal689
    @electionsenegal689 6 лет назад +1

    L’individu ayant approché un devin se trouve dans l’obligation d’accomplir sa prière de Salât pendant quarante jours et quarante nuits sans rétribution de ses prières. Et s’il manque à une seule de ses salât, il commet un autre péché majeur (encore plus grave que le premier).
    La Sourate 72- verset 1 à 4 du Coran, dit que les diseurs d’avenir et ceux qui vont vers eux sont parmi les injustes qui formeront le combustible de l’Enfer (Sourate 72- verset 1à 4)

  • @yayefallfall7061
    @yayefallfall7061 6 лет назад +9

    Mane deh Dara doumaci diakhal ndakh khamnani yalah meuna Mayer te leepp ci kemtanam la

  • @reinenoire3354
    @reinenoire3354 6 лет назад +70

    No sélbé mo nekh néna douma wakh tourr police dima dieul si🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 ndékété doff foo 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @kinediagne385
    @kinediagne385 6 лет назад +7

    Pourtant elle est forte juste parfois diakhasso dafay am

  • @abdoukhoudossdiop2549
    @abdoukhoudossdiop2549 6 лет назад +18

    Yalla maye nako dé

  • @goradiop9234
    @goradiop9234 6 лет назад +17

    Amna mayo yalla de

  • @nafissatoudiouf5674
    @nafissatoudiouf5674 6 лет назад +3

    Loumou dougou reik mou eup mais nak amena louko borom bi may touti nagnou coco nangoul reik jamm daldi ame

  • @dieynabagaye8671
    @dieynabagaye8671 6 лет назад +6

    Barakatou lahilakha ilala Salbé Way

  • @mamediarraboussodiouf5141
    @mamediarraboussodiouf5141 6 лет назад +15

    Ndeyesane amnga mayyy deh

  • @aichasall2441
    @aichasall2441 6 лет назад

    Tay nak selbé wakhna deug 🤣🤣👍🏽

  • @oulysarr3193
    @oulysarr3193 6 лет назад

    je confirme ce qu'elle dit. c'est vrai qu'elle voit vraiment dommage que beaucoup ne croit pas ce quelle dit .

  • @saliousima5894
    @saliousima5894 6 лет назад

    Yallamo meneu mayyè sélbe amal diame

  • @sopnabypsl8956
    @sopnabypsl8956 6 лет назад +17

    vraiment lou nit soxor soxor xamni yalla maynala sénégalais nak mo soxor pour lou moromam am rek baxoul wayé boudé ap naar wala français baxna

  • @laminediagne2949
    @laminediagne2949 6 лет назад +2

    Le prophète a dit que ce sont les diables qui informent les devins. Ils ajoutent à la vérité dérobée 100 mensonges.
    Celui qui croit à ce qu'elle dit n'aura pas sa prière acceptée pendant 40 jours.

  • @zz-lv1ye
    @zz-lv1ye 6 лет назад

    Ay doul késsé, gueum lén yallah té bayii doul

  • @boubacarsyllame2835
    @boubacarsyllame2835 6 лет назад

    machallah

  • @morhmorh4992
    @morhmorh4992 6 лет назад

    Bilay day doul

  • @assgueye3618
    @assgueye3618 6 лет назад

    Toujours ana

  • @serignediop3146
    @serignediop3146 6 лет назад

    Ki dommou xaram deug leu

  • @daoudandiaye3552
    @daoudandiaye3552 6 лет назад

    selbe dall diakhale nama

  • @lerouxleroux2043
    @lerouxleroux2043 6 лет назад

    Wakh deugu nekh yalla bou salbé amé ndam wakhléneko

  • @aliciakane9613
    @aliciakane9613 6 лет назад

    Yen gni wakh selbe des doul bou fekone sen ndey la dolenko wakh arrêté wayy moi j l'aime

  • @mbayemandaw7433
    @mbayemandaw7433 6 лет назад +5

    Selbé bayil labatou bi ... Way 😂 😂😂 yeup khamna niouné dé. Mougui sougnou kanam . Bassi yaw mî dé mouguissa kanam

  • @mamitadiarra1192
    @mamitadiarra1192 6 лет назад

    Ta raison wakhon guako fi vraiment

  • @cadiortvgueye8945
    @cadiortvgueye8945 6 лет назад

    Yalla moy mayè kham kham té maynako salbé

  • @sunkissglowy132
    @sunkissglowy132 6 лет назад

    Pourtant Bachir Kounta était bel et bien journsliste....

  • @thiernomboup3465
    @thiernomboup3465 6 лет назад +4

    Doul rek

  • @mamadoulayesow2930
    @mamadoulayesow2930 6 лет назад

    Selbe stp arrête. Tu nous fatigue avec tes parole. Do yalla do yonete.......... Stp arrête khamo dara

  • @mamecheikhndaow5538
    @mamecheikhndaow5538 6 лет назад

    Kounneccak laka yalla maye eur bou wakhé ni insallah

  • @mamadounafioubah8726
    @mamadounafioubah8726 6 лет назад

    Non Sénégal

  • @cheikhniass9606
    @cheikhniass9606 6 лет назад

    Salbé dél wakh loula lérre guisso dare thi guéli nigni ka bouka dokh waw lolou manta né

  • @ndeyegueye8735
    @ndeyegueye8735 6 лет назад

    Day doul yamba la tokh 😂😂😂😂😂

  • @djibidiallo5093
    @djibidiallo5093 6 лет назад

    ay salbè setal thi yalla baxna bamèll khatna tè leundeumm

  • @gounassbuzz7675
    @gounassbuzz7675 6 лет назад

    KOUY TAKKE MAICHE DOU GUISSE YONETE BI OU JIBIRIL ALAHI LOLOU AMOUL FEN

  • @badianeibrahima8109
    @badianeibrahima8109 6 лет назад

    bilahi barqué serigne touba yaw gisso djibril bilahi

  • @zallzall4378
    @zallzall4378 6 лет назад

    Thiey Galsen

  • @boubacardiouf2928
    @boubacardiouf2928 6 лет назад

    J'aimerai pas être à votre place le jour de la résurrection car vous aurez énormément de choses à répondre et à justifier.

  • @rokhayalavillageoise8380
    @rokhayalavillageoise8380 6 лет назад

    Yalla defko may nak nagn nangou li yalla dogal

  • @binetawatt8886
    @binetawatt8886 6 лет назад

    Seibé miii bakna dal d'Ay fene rek haaaa

  • @mamethiernondiouck526
    @mamethiernondiouck526 6 лет назад

    Li nga wakh yalla wakhouco dé na lérr واعمل للد نياك

  • @cissengary3313
    @cissengary3313 6 лет назад

    Kham kham amnga

  • @moisek147
    @moisek147 6 лет назад

    Boye wakh si nite gni dagniouye wakh si yaw yaye kane té ga nopi khamo nite gni wayé kéne dola khame selbé royal si djiguéne you vakh yi si figa wakh ni.fofou ga bok YALLA DIOKHOULA KOUNAME DJI GA DÈME LIGUÉYI TÉ LIGUÉYE LO SA DOME YI YAGUE YAGUE DAGAYE DÉME BAYILÉNE FI

  • @bfmmchifsmchostouba4640
    @bfmmchifsmchostouba4640 6 лет назад

    SELBE SOP NALA GOUDEUL FANE GNOU BOK AK KOUNOUKO YEENE AKKASA.

  • @amantubillahi9628
    @amantubillahi9628 6 лет назад

    Baatin Yalla moo ko am. Elle ment. C’est haram ce qu’elle fait. Al Quran bii mouy yaqq nak naci tèy!!!
    Kii Dey fen
    Allaahu akbar!!! Gibril nga wakh?????? Kazzaaba anti!! Kamousaylima!!! Haram alych

  • @teusssrekkk1859
    @teusssrekkk1859 6 лет назад

    Wakhone nako deh

  • @mamatechtv
    @mamatechtv 6 лет назад

    astafur la khazim . del wakh lo kham. nit ku nek ak sa bamel. yoneti bi nena guente waro ko wakh ken kudul sa famie walla Kharit bula jégués. salbé nopil lep lo wakh ay fen la. ragalal yalla nak tagua khamni ku niam dundu digua niam d. kon khamal loy wakh. salbé khamo sah niata yon gua wara guis Malakay mawtu avent muy jeul sa ru. salbé nopil guir yalla. harame na nk guaye wakh nan khamone na ni nit ki day dem. man mi damay guis si guente mais ken du ko kham kudul sa ma famie.

  • @abdoulayendiaye8503
    @abdoulayendiaye8503 6 лет назад +4

    Xamiewo lo YALLA wax ak lo kienien wax lol ou Saydina aliyoun mokou wax

  • @elhadjiabdourakhmaneba659
    @elhadjiabdourakhmaneba659 6 лет назад +1

    Et toi as tu vu ton décès

  • @SONKOBOYPAG
    @SONKOBOYPAG 6 лет назад

    Yap nga djibril trop gisso dara boy

  • @gorathiawpatisserieboulangie
    @gorathiawpatisserieboulangie 6 лет назад

    Kata sa Ndeye dôme rame bi

  • @fhachaobiang386
    @fhachaobiang386 6 лет назад

    dée mom dofi diougué bayyil wakhdji

  • @Authenticbusiness21
    @Authenticbusiness21 6 лет назад +1

    Mom legui xamoul kagneu lay décédé 🤔

  • @cherimiriamcisse1282
    @cherimiriamcisse1282 6 лет назад +15

    J m demande sk selbe jouis d ses facultes mentales

  • @diawibrahimakhalil2
    @diawibrahimakhalil2 6 лет назад

    Dimbilil nitndih waw sofnga trop démel diamouji yala mo gann si yaw

  • @awaniang4299
    @awaniang4299 6 лет назад

    selbe ba filay yam

  • @nevergiveup4950
    @nevergiveup4950 6 лет назад

    Svp qui a le numéro de Selbé please dioxmako

  • @cheikhkebe8696
    @cheikhkebe8696 6 лет назад

    Vraiment tu l avais dis

  • @morhmorh4992
    @morhmorh4992 6 лет назад

    Day fèn rek

  • @badianeibrahima8109
    @badianeibrahima8109 6 лет назад

    dara du ci deugg lou khéw yalla la bu nékon lou way kham wakh ko kone Adouna du nékh yaw danga rér

  • @loulouberganediagne6182
    @loulouberganediagne6182 6 лет назад

    Ki day doul la loi de la nature fait que quand kilifa qui meurt remporte 2 avec lui.
    Je vous le dis un kilifa décéde par 3

  • @layeabdallah380
    @layeabdallah380 6 лет назад +5

    Sèlbè dèmal gua Laabou jii khamna dayy gua fiiga tokk bou yagg

    • @antaseck3768
      @antaseck3768 6 лет назад

      Aha

    • @adelonthetrack8670
      @adelonthetrack8670 6 лет назад +3

      un peu de respect quand même lou la yar mayul rewander doula ko mossa may respecter vos aînés !! li gue wax ni bou ndiabotam togone sa kanam doko wax

    • @layeabdallah380
      @layeabdallah380 6 лет назад

      @@adelonthetrack8670 yao toptol say khourr tè tiaabii ko

    • @adelonthetrack8670
      @adelonthetrack8670 6 лет назад +2

      @@layeabdallah380 lol balnaleu dou mak iow !! rester derrière son ecran et dire n importe quoi c tro facil !! wayer di gue xamni togn dou galath nagn deim rek adouna gui souniou kanam bayina la ak borom bi

    • @gnagnamboup7418
      @gnagnamboup7418 6 лет назад +1

      Mais un peu de respect quand même ablaye

  • @lebaolbaoltigui2599
    @lebaolbaoltigui2599 6 лет назад

    Yonu guethie Mdrrrr salbe artiste leu

  • @sambadiagne2064
    @sambadiagne2064 6 лет назад

    Nom vraiment selbé vrai satan la . Yaw lépe yagui si du jamais vu

  • @ibrahimagueye8559
    @ibrahimagueye8559 6 лет назад

    Kene newoul manoul set mais elle parle trop

  • @AliouSeckSN
    @AliouSeckSN 6 лет назад +5

    DAY TANDOU DI DOUL REK

  • @mbouplepatriotesenegalais2884
    @mbouplepatriotesenegalais2884 6 лет назад

    والله عالم الغیب والشهادة = yalla rk mokhe elegue loye khewe

  • @doumbouyaramatoulaye2395
    @doumbouyaramatoulaye2395 6 лет назад +3

    Ndéy sane elle voi dé foi MDR

  • @boromxasssxasss3333
    @boromxasssxasss3333 6 лет назад

    😂😂😂😂😂😂😂

  • @khadimalaminediopofficiel6050
    @khadimalaminediopofficiel6050 6 лет назад +10

    Dayy Doul rk yallah rk Mo kham

  • @SONKOBOYPAG
    @SONKOBOYPAG 6 лет назад

    Wakho deug dddd.
    Lolou hadith la dou coran.
    Mère tè nga yam

  • @iboudrame6129
    @iboudrame6129 6 лет назад

    Non salbé mo nekh koi

  • @aliniang7452
    @aliniang7452 6 лет назад

    Selbe fenkatla

  • @khadimbeye8860
    @khadimbeye8860 6 лет назад +3

    Del doul rek. Ak sa pakhou bakane you reyeu

  • @papefall5881
    @papefall5881 6 лет назад

    Ay khésel katby ya am fit waki louko dall

  • @sencomedie9074
    @sencomedie9074 6 лет назад

    day fenn rk

  • @bongacamara6998
    @bongacamara6998 6 лет назад

    ki dal doyna waar

  • @kanemamoudou6298
    @kanemamoudou6298 6 лет назад

    doul dal. ya fii Moune bolo y'all diaper ga rethiou gniak. diomme

  • @sowamina1725
    @sowamina1725 6 лет назад +1

    Mais journaliste lawone tamit selbe yamal

  • @abdourahimkanetouba3120
    @abdourahimkanetouba3120 6 лет назад

    Yaw fagua dieum ak Sénégal léyi wakhagouko doul rékk thiiiiim yaa soff

  • @khadydiop5617
    @khadydiop5617 6 лет назад

    Fane rak

  • @koumbadiop6447
    @koumbadiop6447 6 лет назад

    Ey nagnou ragal yalla

  • @LmcsLmcs
    @LmcsLmcs 6 лет назад +1

    😂😂😂😂😂

  • @sarralbertlidovic4580
    @sarralbertlidovic4580 6 лет назад +1

    Selbe do tital Kene .
    fi nieuppou aye dee.
    Kene dou dess fi merde.
    lii diàroul Wakh sakh

  • @papemassarsarr6181
    @papemassarsarr6181 6 лет назад +3

    salbé fénréklaye déf bayil kathi

  • @juniordia7630
    @juniordia7630 6 лет назад

    Elle là parfaitement raison tua eu 50)50

  • @serignemodoundiaye7434
    @serignemodoundiaye7434 6 лет назад

    Salafoul ndaye yaw fén rek

  • @moustaphandiaye7569
    @moustaphandiaye7569 6 лет назад

    Oie kantesk tu vas mourir. Dis moi stp

  • @is909
    @is909 6 лет назад

    Hahahaha police

  • @presiseck494
    @presiseck494 6 лет назад

    Yaw danga dof

  • @malickdiouf8866
    @malickdiouf8866 6 лет назад

    Doull rek Sall be bayill fenn

    • @laminebalde2364
      @laminebalde2364 6 лет назад

      Kon yaw bane jour guay dh. Bayil thiakaneyi yonene tibi psl dako terree

  • @10f-e6m
    @10f-e6m 6 лет назад +1

    C pas vrai ragalal yalla

  • @mamitadiarra1192
    @mamitadiarra1192 6 лет назад +5

    Ta raison wakhon guako fi vraiment