@@aminandong7735bilay wakhgua deggeu polygamie problème rek bo dewé bayi fi Say gniabote gniouy rayanté mais la magorite des hommes louléne ndekh rek ils s'en fou du reste
Walakhi j'ai les larmes qui coulent, lorsque le gas avait dit bayinalene ak yalla, wate si Serigne Touba, sama khole dafaa toyy. Mais mbokk leguii , on comprend plus ce qui se passe. Moi la majeure partie de mes biens, le travail je l'ai eu a partir d'autre personne différents de ma famille.
Encore la polygamie Avec ça il ne faut jamais durer dans la maison familiale si possible quitter tres tot et faire sa vie je crois que cest la meilleure solution
Yéne goor yi tamite warguene kholate séne bop louléne nekh rek vous pensez même pas a l'avenir de vos enfants voilà le résultat de la polygamie après votre mort que des problèmes raison pour laquelle j'aime pas la polygamie
l'Africain est toujours dans l'émotion. la mère du gars est née et a grandi dans cette maison, pareil pour lui et ses enfants. Ce grand gaillard s'est marié et a fait des enfants. Pourquoi ne s'est-il pas employé à se trouver un boulot et construire sa propre maison ? Personne ne l'en aurait délogé. Je ne comprends pas qu'on soit dans la logique d'être pris en charge toute sa vie. Moi, je suis triste pour la mère et les enfants du gars. Pas pour lui. Il est encore valide, il n'a qu'à aller travailler et loger sa famille. Il serait le premier à crier haro, si la maison venait à s'écrouler sur sa famille. Je prie cependant pour eux tous. Qu'Allah leur vienne en aide. Le gars devrait commencer par accepter que sa mère aille vivre avec ses frères. Je comprends cependant qu'il ait refusé avant, la présence de la mère dans la maison était pour lui la garantie que lui et sa famille resteraient dans la maison.
Pour avoir vécu dans la location je prie Allah de nous donner un toit dans ce bas monde et surtout une demeure éternelle au Paradis Firdaws 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Billahi alalou Adina dou dra kou khol thie momi dani seck rek wargna yéwou 😢yalla nalen yalla samou sa me fait mal vraiment Mogui melni sama famille la 😢
🇺🇸🇸🇳mèttina trop bilahiii😭j'ai pas pu continué la vidéo 😢yalla nallènne yalla diappalé Incha'Allah raison pour laquelle beaucoup d'homme veulent pas avoir plusieurs femmes 😢
Niaw ba torope mais kon se dise la vérité deuk fa takhoul géne mom ko . Yalla naniou yalla may suniuy yeufi bop ba kéne duniu torokhol . Li niaw na torope.
Il faudrait des associations pour aider c familles en détresses. Je pense que même la diaspora peut y participer si c bien organisé et honnête. Sénégal rewou terangala 😢😢😢
Ndéysan Man mi Sante Ba Sakh Dama Diomi Thiéy Sama Bokou Yi Khawmani Won Ni Guéneu Mél Bilae Walae Mai Yalla Bakhna IBRAHIMA Leep Dina Bakh Inchalla Diam Rek Guéni Am Que Dieu Vous Protège😭🤧❤️
Lii moy sénégal Bo sété ben Borom doolé moko diaye doolé,ba paré on nous parle de justice dans ce pays!! Fii amoul ben justice Gni neck si souf bougn youkho Ken douleen deugg,wayé nimou nékké si politiciens yii nonou la neck si gni neck si souff Ce pays est un désespoir total,même les étrangers sont mieux traité dans ce pays Sénégalais sokhor la deff
Vraiment amna nite mokk toi boneu sokhore am sen keur nek sen diam ak sa famille du torokhole ki gua bokeul bén baye guén warone ko défeul mes sante yalla rek courage mon frere metina trop mes lhistoire retiendra yalla dinalén atté soudé li gua wakh ni mo am rek yalla day atté Inchallah khipp sa beute gua kholle ba kham niom founouy moudjé li malako wakh kén dou torokhole doumou adama kou masseu torokhole doumou adama di gua trokho dama dioye parsk khamo fo dieum métina wayy
Keur famille dou keur déjà sakh famille mo amatoul so néké si keur bocouka ak niénéne dagaye goorgorlou téla wouti sa yeufou bopou yalnalén yalla takhawou inchallah
c'est vrai que c'est triste mais dinné mo wakh ni nitte bou guénné adounna dagnoo warra mirasse kounnékk djieulle limou mommme yalla bakhnna yalla rékk mo yorre nitte😢😢
@@boubacarabidinaaidara4408 dou Niep mais la magorite c'est comme ça d'ailleurs un voisin a chassé son enfants c'est lui pour installer sa seconde épouse et ses enfants le voisin même est un classe de mon père gnio bokou bigniou demé armé mais il est plus agé que mon père avant d'expulser son enfants il a dit à mon père de parler avec son fils pour mou gueneu si keur gui sama pape a refuser et lui a dit ceux que tu vas faire c'est pas bon mou mèré siwone sama pape mena que mon père est mort nous on est tjr tranquille parceque amougniou aiy domou baye mais imagine que le voisin meurt yaura trop de blem vu qu ils est polygame et ses enfants bougougniou séne domou baye enplus la mère de ce dernière est morte j'ai même de la peine pour lui
Les avocats ou les juges devraient intervenir dans cette situation on devrait tout faire pour que la malade etsa famille récupère leur part de l'héritage laissé par le vieux Ba la malade ne peut pas partir vivre avec ses demi frères et laisser son fils et ses petits-enfants seuls à la rue la
Si j'ai bien compris c'est une maison familiale qui appartient a ' soeur et " frere legui l'une des soeurs occupe la maison avec sa famille légui on veut le vendre et se partager l'heritage et la famille de l'occupante de la maison s'y oppose mais nak naniou wakahnete deugeu seute mom yonam nekoussi keur danioukoy mbirasse
Il faut que les gens prennent conscience que les enfants sont sacrés ! Wagni diour bi nguir meune sameu jaboot bi! Dé gnu wara nek nit nek joulite, Sénégal comme bén mbalite bouy law, té téyoul khélou autorité yi, Lane mo gnou dal?
Ndeysane sama xol diekhna 😭 li lép nakh alalou Adina 😢 c'est vraiment très triste walahi Azim si j'avais la moyenne j'allais les hébergé bilahi 🤦♀️😭😭😭😭
😭😭yalna yalla faye toubab bi créé reseau sociaux lou bone yaguna Thii Sénégal té kaine hamouko wone amna niou bon trop sa walahi douniou ay nite alal diaral nalaine lou nék
Delen wakh Loulen worr gni biniou Len dale wakh naniou guene niou danel keur gui defarte ko dafa yague keur gui boko Guisson do wakh li famille bi douniou len bayi niou deuk si te kham ni a tout moment meune na danou ay mère bi ay sœreum beugue nagne ko fat dom dji bagne
Yalla na yalla may lén keur bou geune by mère khady bobo akk néné guale sén yaye djieynaba barie sén sœur éne moy souniou dekeundo nioniou deunio yeug sén bopou son frère limou expliqué na lén woutal founiou deuk ndakh am naniou ko
Oh j ai les larmes aux yeux quand j ai vu la maman que le bon dieu vous viens en aide amine
Allahouma amine
Amine
*Amennnn 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Bilay lii metina m warna yei goor gni tmt gnu bayii polygamie bii prsk koussi dei sa diabote thie rayanté lagnuy deuk
@@aminandong7735bilay wakhgua deggeu polygamie problème rek bo dewé bayi fi Say gniabote gniouy rayanté mais la magorite des hommes louléne ndekh rek ils s'en fou du reste
Walakhi j'ai les larmes qui coulent, lorsque le gas avait dit bayinalene ak yalla, wate si Serigne Touba, sama khole dafaa toyy. Mais mbokk leguii , on comprend plus ce qui se passe. Moi la majeure partie de mes biens, le travail je l'ai eu a partir d'autre personne différents de ma famille.
Walahi ndeyssane
Bammel moy keur thieye adouna .c est toujours comme ça dans beaucoup de familles que le bon Dieu les.viennent en aide
Encore la polygamie
Avec ça il ne faut jamais durer dans la maison familiale si possible quitter tres tot et faire sa vie je crois que cest la meilleure solution
❤❤❤❤❤❤😭😭
c'est l'idéal mais tout le monde n'a pas les moyens de quitter
T as raison mais si des fois les moyens qui font défauts
Yéne goor yi tamite warguene kholate séne bop louléne nekh rek vous pensez même pas a l'avenir de vos enfants voilà le résultat de la polygamie après votre mort que des problèmes raison pour laquelle j'aime pas la polygamie
@@binettendione2137polygamie boko bagné moy yagui dolél lesbienne le plus important moy éducation familiale voilà
Vraiment c'est triste je vous invite à faire une collecte pour aider cette famille a acheté une nouvelle maison
Lou SA way guén khékh moka guéneu yomou
Moi je demande qu'est ce qu'il ont fait je ne sais pas c'est quoi ça Hein aider moi à comprendre où vivent ce problème nohhh sa c'est dur Hein 😢😮
D'accord n'a déi!
✊🏿❤️
l'Africain est toujours dans l'émotion. la mère du gars est née et a grandi dans cette maison, pareil pour lui et ses enfants. Ce grand gaillard s'est marié et a fait des enfants. Pourquoi ne s'est-il pas employé à se trouver un boulot et construire sa propre maison ? Personne ne l'en aurait délogé. Je ne comprends pas qu'on soit dans la logique d'être pris en charge toute sa vie. Moi, je suis triste pour la mère et les enfants du gars. Pas pour lui. Il est encore valide, il n'a qu'à aller travailler et loger sa famille. Il serait le premier à crier haro, si la maison venait à s'écrouler sur sa famille. Je prie cependant pour eux tous. Qu'Allah leur vienne en aide. Le gars devrait commencer par accepter que sa mère aille vivre avec ses frères. Je comprends cependant qu'il ait refusé avant, la présence de la mère dans la maison était pour lui la garantie que lui et sa famille resteraient dans la maison.
Il ne fallait pas filmer la maman surtout dans l’état où elle se trouve. Qu’Allah leur vienne en aide incha’Allah 🙏🏾
C'est vrai j'ai pleurer
La famille est sacrée. Les biens de ce bas monde vont nous diviser de plus en plus.
😢Ohhhh Allah Soubkhana wa Talla aide cette maman et sa famille 😢😢
Pour avoir vécu dans la location je prie Allah de nous donner un toit dans ce bas monde et surtout une demeure éternelle au Paradis Firdaws 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Lou mél ni rék mo takh niou Bari Di dém ci gaal gi ,kham ngané ki souba souba su gison gaal day dém ,,naniy yaramnté si Sun biir ta yalla takh 😢😢
No ki doudéme doufi bayi yayam ak ay ndiabootam ki responsable la
Billahi alalou Adina dou dra kou khol thie momi dani seck rek wargna yéwou 😢yalla nalen yalla samou sa me fait mal vraiment Mogui melni sama famille la 😢
Allahou Akbar j espére dans ma vie ne jamais jamais mettre quelqun dehors bilaye je le demande à Allah
🇺🇸🇸🇳mèttina trop bilahiii😭j'ai pas pu continué la vidéo 😢yalla nallènne yalla diappalé Incha'Allah raison pour laquelle beaucoup d'homme veulent pas avoir plusieurs femmes 😢
Allahou Akbar yalla na gnou yalla maye soutoureu adouna akk alahira si barké nabil moustapha (psl)
Que Allah vient en aide cette famille ❤
Dieu sera toujours ô contrôle in sha allah 🙏
Vraiment triste que Dieu vienne en aide 😢
Que dieu vous protège c'est vraiment triste délosiléne séne khel thi yalla
Mais fi fan la thi grand Dakar khamew ma fii 😢😢😢
Bismillahi rahmanirahim
Que ceux qui sont plus opulent aident leur proche parent nécessiteux
😭😭😭😭😭dieu sera toujours avec vous ani def katou lou bakh yiffi yalla décka teranga😭
Li niawna on doit vraiment faire un collecte pour les aider
Hooo ay mbokou legui doungou dara bilahi li metina trop me yala dina ngeuw legui inchallah courage Ibrahima 😭😭😭😭
Qu'Allah nous épargne de la pauvreté et nous accorde une belle et longue vie avec une fin heureuse.
C'est triste 😢😢😢😢 que Dieu protège cette famille
Nite mo booone😭😭😭 Allahou Akbar.... Je peux plus tenir mes larmes😭😭😭😭 Allahou Akbar
IL ne fast pas juger si on ne connait pas l'histiore.
@@ataoulayebalde merde ioe
C'est triste et vraiment triste. Dieu est le plus juste des juges.
Ndéyesane mais yalla bahna te barina soutoura 😢😢
On doit aider cette famille
Sait triste toujours sait comme sa 😢😢😢 dieu est grand
Que Dieu aide cette famille
☝☝☝que dieu vous protèges inchallah
Mon frère courage dieu avec vous
yawe male khiyame dina meiti dei..yalla naleine yalla dolile soutoureu si barke kou teide ki (psl)
Quelle tristesse !. Que ALLAH vous donne une très belle maison !
Oh l'image de la maman qui pleure est insoutenable ayway li niawna aduna diaroul li😭😭😭massa lancez une cagnotte pour les aider 😭
Niaw ba torope mais kon se dise la vérité deuk fa takhoul géne mom ko . Yalla naniou yalla may suniuy yeufi bop ba kéne duniu torokhol . Li niaw na torope.
Il faudrait des associations pour aider c familles en détresses. Je pense que même la diaspora peut y participer si c bien organisé et honnête. Sénégal rewou terangala 😢😢😢
Ndéysan Man mi Sante Ba Sakh Dama Diomi Thiéy Sama Bokou Yi Khawmani Won Ni Guéneu Mél Bilae Walae Mai Yalla Bakhna IBRAHIMA Leep Dina Bakh Inchalla Diam Rek Guéni Am Que Dieu Vous Protège😭🤧❤️
Lii moy sénégal
Bo sété ben Borom doolé moko diaye doolé,ba paré on nous parle de justice dans ce pays!! Fii amoul ben justice
Gni neck si souf bougn youkho Ken douleen deugg,wayé nimou nékké si politiciens yii nonou la neck si gni neck si souff
Ce pays est un désespoir total,même les étrangers sont mieux traité dans ce pays
Sénégalais sokhor la deff
Que dieu vous protège 😢😢😢😢
njiko kame merci de partager le contact de Ibrahima pour kokou diapalé 😢😢
Thièye aduna foumou dieume ohh vraiment métina trop bilahi 😭
Ce n'est pas normal ! Le manque d'humanisme au Sénégal me fait peur. La colère de Dieu... !
Le Sénégal est foutu avec des individus sans cœur
Je sais pas qu'est-ce qui passait au niveau du tribunal mais la maison n'a pas de sécurité
Merci les gens ne comprennent pas la situation mais dieu connaît la vérité yalla bakhna lepp dina lere inchallah
Mais gnou mirass ko mo geune kou nek dieul loumou mom lolou moy deug
Nguir yalla diapalé niou si numéro bouniou lén meuna dioté😭😭😭😭🙏🙏🙏
Khawouma sakh limay dioylo😭meti n’a nek si adouna di souffert 💔😭kene mounou la takhawou mais yalla nalene yalla takhawou si barki cheikhoul khadim 🙏🏻
Loutakh toujours Les peuvre sont toujours positif yalla guis na lep mon frère Dama dioy si vidéo bi 😢
C'est k né métina mais keurou mame dou keur ne le Borom bi japeulé amine
Vraiment amna nite mokk toi boneu sokhore am sen keur nek sen diam ak sa famille du torokhole ki gua bokeul bén baye guén warone ko défeul mes sante yalla rek courage mon frere metina trop mes lhistoire retiendra yalla dinalén atté soudé li gua wakh ni mo am rek yalla day atté Inchallah khipp sa beute gua kholle ba kham niom founouy moudjé li malako wakh kén dou torokhole doumou adama kou masseu torokhole doumou adama di gua trokho dama dioye parsk khamo fo dieum métina wayy
Qu'ALLAH SWT assiste cette famille
اللهم أنصرإخواننا المسلمين في قارندكار
vraiment c'est très triste moi j'ai peur un autre pays Sénégal les majorités de population aucune sentiment non ça fait mal???😢😢😢
Mane ma warou si khetou djoulite torokhal sa deret ngir alalou adouna , yalla nalene yalla takhawou
Way sou amone vocal ma oubi sa leufeul ndeye yallah nga deh si lackoum domou tall
Amine
C'est les conséquences de la polygamie. Une seule maison pour plusieurs enfants de mère différentes
C'est compliqué
Keur famille dou keur déjà sakh famille mo amatoul so néké si keur bocouka ak niénéne dagaye goorgorlou téla wouti sa yeufou bopou yalnalén yalla takhawou inchallah
Oooh li d doyna war, yalnaleine sunu borom Wallu in sha alla, Ibrahima courage, li metina coniou diamano grand sama fief la, falla dioudo
Sainte Rita de cassia
Venez moi en aide
Pour mes enfants et moi Amen❤❤❤
No li Dawna yarame trop yalla same may la goudou fane ak wer inchalla yalla nalne yalla takhawou
Yalla nallen yalla diapalé may len fouguen dougou si barki seydina mohamed ❤❤
AMINE
Ayy wayy khana borom térrangay adouna yii khana guissou niou lii méttina trop😢
Mon Dieu sauve cette famille démunie😢
Il faut partager la vidéo 😭😭😭😭😭😭😭😭
c'est vrai que c'est triste mais dinné mo wakh ni nitte bou guénné adounna dagnoo warra mirasse kounnékk djieulle limou mommme yalla bakhnna yalla rékk mo yorre nitte😢😢
Yaw deum nga amo xol
Thiëy Yalla Sénégal dõyna warr 😭😭😭😭😭
Yalla naleine yalla takhawouuu 😭
Que Allah vien en aidé à cette famille 😭😭
Allahouma amiine 🙏
Le résultat de la polygamie
@@binettendione2137 mais d'où nieup de
@@boubacarabidinaaidara4408 dou Niep mais la magorite c'est comme ça d'ailleurs un voisin a chassé son enfants c'est lui pour installer sa seconde épouse et ses enfants le voisin même est un classe de mon père gnio bokou bigniou demé armé mais il est plus agé que mon père avant d'expulser son enfants il a dit à mon père de parler avec son fils pour mou gueneu si keur gui sama pape a refuser et lui a dit ceux que tu vas faire c'est pas bon mou mèré siwone sama pape mena que mon père est mort nous on est tjr tranquille parceque amougniou aiy domou baye mais imagine que le voisin meurt yaura trop de blem vu qu ils est polygame et ses enfants bougougniou séne domou baye enplus la mère de ce dernière est morte j'ai même de la peine pour lui
Les avocats ou les juges devraient intervenir dans cette situation on devrait tout faire pour que la malade etsa famille récupère leur part de l'héritage laissé par le vieux Ba la malade ne peut pas partir vivre avec ses demi frères et laisser son fils et ses petits-enfants seuls à la rue la
Yalnalén yalla takhawou inchalah 😢😢😢
Adouna metina hey waye mère bi damako yereum ey waye kene d'où torokhal noté walahi j'ai les larmes aux yeux
Non ce qui se passe au Sénégal c'est hallucinant gni am dolé di def loulene nekh té dara douléne si fek
Si j'ai bien compris c'est une maison familiale qui appartient a ' soeur et " frere legui l'une des soeurs occupe la maison avec sa famille légui on veut le vendre et se partager l'heritage et la famille de l'occupante de la maison s'y oppose mais nak naniou wakahnete deugeu seute mom yonam nekoussi keur danioukoy mbirasse
Qu'elle horreur je n'ai pas les mots pour d'écrire mon émotion.
Wallahi métina trop j'ai des larmes au yeux
Yallah naniou am fougeune fii sii Barker Seydina Mouhamed PSL
Courage grand kou holl ci mere bi sah❤ meuneu harr
😢😢😢😢 vraiment métina , mais gni Di todje ak dawal ndraneubi, ils le font sans contrecoeur 😢
bassirou yaw kou bone nga yalnallah yallah wane bopam ya bone ya yéésss.....thiey yallah !
Que dieu vous protège
Souma yalla dénkon keur goumako meuna may walay tay falay fanan mais yalla diékhoul walahi métina
Yallah nala yallah faye sa khôl
Vraiment c’est dure 😭😭 😭😭😭
Que dieu aide cette familly😢😢😢😢❤😭
Sénégal gui dou rewom diamou li😢😢😢😢
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢this is so sad may Allah SWT protect you
Hasbunallah wa nihmal wakeel😢😢😢
Adalak yalla yalla nala yalla maye lo yorré sa yaye thi Barker Serigne Babacar sy
Il faut que les gens prennent conscience que les enfants sont sacrés !
Wagni diour bi nguir meune sameu jaboot bi!
Dé gnu wara nek nit nek joulite, Sénégal comme bén mbalite bouy law, té téyoul khélou autorité yi,
Lane mo gnou dal?
Famille légui d'où Famille dokhan dème mo léne geune lou lére la wax sé té premier ennemi
Ndeysane sama xol diekhna 😭 li lép nakh alalou Adina 😢 c'est vraiment très triste walahi Azim si j'avais la moyenne j'allais les hébergé bilahi 🤦♀️😭😭😭😭
Yallah bakhna
Une pensée à eux 😢akk taw bi ni😭
😢😢😢😢😢nonnn mère bi 💔💔😭😭😭😭😭
Je suis choquée hoooo la maman 😢😢😢
ay way wallahi sama hole métina souma ka manou na tay dina ko dimbaliii
😭😭yalna yalla faye toubab bi créé reseau sociaux lou bone yaguna Thii Sénégal té kaine hamouko wone amna niou bon trop sa walahi douniou ay nite alal diaral nalaine lou nék
Delen wakh Loulen worr gni biniou Len dale wakh naniou guene niou danel keur gui defarte ko dafa yague keur gui boko Guisson do wakh li famille bi douniou len bayi niou deuk si te kham ni a tout moment meune na danou ay mère bi ay sœreum beugue nagne ko fat dom dji bagne
@@Princesse1006lolou kaye métiwoul nagne ko diokh foumou dekeu ak yayame rék mo gueune tamit mouye danou séne kaw
Comment on peut faire ça à sa famille ?
@@Princesse1006Li kaye d’où keur en la dame là di wakhnaye léne Bou yagueu niou guéneu mais sénégualais mo meune victimiser wou
Domdji kou niakk fayda la, mo wara dem ligueyi Yor bopam au lieu mouy manipuler mère bi. Kou khôl vidéo bi khamni keur gui bine n'a legui mou danoi
Ndeysane yalah naleine Yallah takhawou wayy metina troppppeee😢😢
Gueudj na dioye mais lii metina yalla na yalla takhawoulene
Yalla na yalla may lén keur bou geune by mère khady bobo akk néné guale sén yaye djieynaba barie sén sœur éne moy souniou dekeundo nioniou deunio yeug sén bopou son frère limou expliqué na lén woutal founiou deuk ndakh am naniou ko
kou am ay moyen aider len gni s il le faut vous lui prener un appartement svp que dieu te souhaite mon frere gor dafa metty
Même niit yi ko khamoyl sakh sen khol tooyna 😭😭😭yalna len yarabi takhawou