Sougnou dekendo you bakh lagnou khamou gnou loudoule liguéye, diamou yalla, dioube, yalla na yalla lérale lépe bagnou guéne si wérou safar bi que justice soit faite.
😢😢😢C'EST TRISTE CETTE HISTOIRE 28 ANS DE DURE LABOURE SANS RECONNAISSANCE ET CLOIRE LE TOUT C'EST LA PRISON QUE DIEU LE PATRON DE L'UNIVERS SOIT À COTÉ DE SES ORPHELINS AMINE YARABI
ma fille de tout cœur avec ta famille soutient tes frères jusqu'au bout gor bakh na djiguene raw tient bon Dieu est le plus juste des juges soit forte même très forte
Ne rester pas là. Allez voir Teuss, Xalass et d'autres sites. il faut faut que le monde entier soit au courant. On sent quand des personnes disent la vérité. Nous sommes de tout cœur avec vous.
Li doyna warr tropp khalisse bi auto yi Keur yi leppeu fila niouye bayi leppeu naniouy rafetal adouna daffa guatte netali bou rafet mo gueneu bou nianw lou nianw bakhoule wassalam
Mane dé barké s saliou nek nama AK gniom bokk liguey bi Di kheyando Di wathiando mais bilahi walahi talahi kéne guenou lén gnou bakh lagne liguey rek lagne kham walahi té lepp Dina lérr inchallah legui rek yalla dou fatté dafa yakamti woul rek
Môm dal daflèn exploitè ba doyal emprisonnè lèn , motax jeune dangay yèwou bo nèkè ci beureubou liguèyou kay 2 ans guisso ci sa bopp tu dois quittè et chercher autre chose
Je ne connais pas le fond de l histoire, mais le faite de les faire travailler depuis l âge minieur est un délit, si c était en Europe l oncle aller les dédommager et faire la prison
Comment un milliardaire peut-il traduire en justice ses propres neveux ? Il préfère sauver son argent plutôt que la vie de ceux-ci. Allalou adouna djarouko dé ! Itakhoullah!
Masta ma chérie Yalla nalenne KO Borome bi téguile. Tu m'as fait plairé. Toi leur sœur tu es une bonne personne une personne pieuse gentille généreuse. Yalla nalenne Borome bi taguawou. Toute la classe sup 1 de Ndiarka Diagne prie pour tes frères
Mann déy warouna😢sén badiane dioylo nama😢😢😢sén ndidiaye xana xamoul lii Yalla wakh thi djirim😢 Allahou Akbar 😢. Lii mom esclavage deug leu😢lii nak mo xéw thi rewmi 😢 alalou adouna diaroul lii dé😢ki mo bonn. Bilahi béss bou dougué thi biir bamèl dina faté loumou meusseu am thi adouna. Rakam yoyou ak domam yoyou dougnouko meusseu nianial ndakh xeuthio alal, diabar yi pa yi ndieukeunté lén ndakh alal dji😢. Yalla na Yalla arr xalé yi té natou bi nék sén thianguate thi barké Rassoulilah Aleyhi Salatou Wa Salam 💚 💚 💚
Ki mo bone dafa compromettre avenirou khalé yi parce que yak n'a séne diang pour mou meuna réussir khalé you tôle thi diangue ga réquisitionné pour ga meuna téki léne séne akeu dinalène dale bala mo Sango Souf li dafa méti
SÉEN NIDIAYE BI DÉ XANA XAMOUL LI YALLA SWT WAX SI DJIRIME 😢😢 ALLAHOU AKBAR KI MO BONE 😮😢 DIEUL SAY DOME DEF LÉEN PRINCES 🤴🏿 ET DIEUL SAY DOMOU RAKEU DÉF LÉEN ESCLAVES 😮 KI MOY DOMOU HARAM DEGEUUU TÉ BONE 😢😢😢 LI MÉTINA TROPPPPPP VRAIMENT 😢😢 QUE JUSTE SOIT FAITE 😢😢
Cette histoire est bizarre, combien de boutiques pour Milliards. Il faut toujours pensez a avoir ses propres choses après quelques années dans une boite ❤
@@bellediolla3414 elle a compris elle veut faire comprendre aux gens de penser à investir pour leur propre business après quelques années dans une boîte au lieu de suivre leurs patrons qui ne se soucient qu'à leur propre intérêt
Allez vers tous les médias radios, télé, sites internet presse écritesque sais-je encore,que ce gros bras soit dénoncé que justice soit faite que diomaye,sonko soient informés car cet homme a compris l'avenir de ces enfants ,il a bafoué leurs droits il sait qu'ils ont maitrisé le travail et s'ils se lancent dans le commerce ils seront des concurrents qui peuvent le conduire à fermer boutique
Meusouma Kham Ni Mbaye Tourè bimay dég Domérame la Non ,,Saway Ki Loum Am si ay (Remark ) Demna ba meuneutoul Muté Mouy Def si tourou rak dji Ibrahima tourè ,mè ki ndéké domou kharam deug leu
Cette femme maîtrise bien le dossier. Qu Allah vous êtes
Sougnou dekendo you bakh lagnou khamou gnou loudoule liguéye, diamou yalla, dioube, yalla na yalla lérale lépe bagnou guéne si wérou safar bi que justice soit faite.
😢😢😢C'EST TRISTE CETTE HISTOIRE 28 ANS DE DURE LABOURE SANS RECONNAISSANCE ET CLOIRE LE TOUT C'EST LA PRISON QUE DIEU LE PATRON DE L'UNIVERS SOIT À COTÉ DE SES ORPHELINS AMINE YARABI
@@astpuizambart1126 Amine
Allahouma amine
Amine yaraby @@astpuizambart1126
Mbay touré limakoy dégu lépou kou bakh lako tégon dégué kou bon la
sèche tes larmes il ne faut pas qu il soit content de te voir souffrir soit forte encore suis la justice ne lâche pas tant que tu n'as pas gagné
Walay senegaler boko dioyaler rk dalay sonal😢😢
Les 4 frère yala nalene yalla guéné si lou gaw inchallah ❤
amine. metina trop
ma fille de tout cœur avec ta famille soutient tes frères jusqu'au bout gor bakh na djiguene raw tient bon Dieu est le plus juste des juges soit forte même très forte
Il faut continuer la médiatisation ça va payer inshaAlha que le bon Dieu éclairé cette situation barké CHEIKH ISSA DIÉNE
Nous sommes de tout cœur avec vous mesdames vraiment ce monde est cruelle même nos propres parents nous mènes la vie difficile
metina trop
Ne rester pas là. Allez voir Teuss, Xalass et d'autres sites. il faut faut que le monde entier soit au courant. On sent quand des personnes disent la vérité. Nous sommes de tout cœur avec vous.
C'est vrai que la justice a peur des dossiers médiatisés. C'est pour ça que des avocats comme elhaj Diouf sont autant sollicités
Li doyna warr tropp khalisse bi auto yi Keur yi leppeu fila niouye bayi leppeu naniouy rafetal adouna daffa guatte netali bou rafet mo gueneu bou nianw lou nianw bakhoule wassalam
Il faut insister que justice soit faite pour que les enfants soient dédommager.
Mais ana diomaye ana sonko ana justice yalla naléne yalla takhawou
WAKHOU NAFEKH REK GEN MAN
Diomay ak sonko nioye justice dou mougui si yoon do nopi rek setane
Amoul bène dolè yalla moko eupe dolè outlène avocat Diay dolè Dièkhnasi rewmi
Faynaniou avocat ba sonn motakh niou moudié si réseaux yi khamnassi dara
Hooo quelle tristesse mon dieu trop d injutice courage mes dames
Métina trop yalla naléne yalla doléle si barké nabi aleyhi salatou wa salam 😢😢😢
Mane dé barké s saliou nek nama AK gniom bokk liguey bi Di kheyando Di wathiando mais bilahi walahi talahi kéne guenou lén gnou bakh lagne liguey rek lagne kham walahi té lepp Dina lérr inchallah legui rek yalla dou fatté dafa yakamti woul rek
In sha ALLAH
Mane mom sama ❤Diekhena taak si (Mbaye toure) limou def ñawena trop ngir halalou Adouna mom ak fiko wakeur cheikh inssa Diene teek waronena rousliii bilahi keen kousinek meunala Dioox 1milillar te douko wañi Dara 29 ans de service ak kou xaam ligueyou (Mbaye tourè ) warna diox Gayii xalis bou bariii (mangi wo wakeur cheikh insa Diene ñou woo Mbaye tourè Koom seen Talibe la ñou wakh koo degue) Adouna dou keur( mane rk 1998 y 99 Dama dane diaar Boba ay charèt rk ñofa nèkoon wakh degue yalla wayè koufa Diaar taay xameni yokoutè Amenafa si louwer ( 😢😢dioye na s Abdou latif Diene soufi nekoone dinako waax degue Bilahi)😢😢😢😢😢😢😢
Kou bakh fii borom alal ken douko wax deug.. so leen clamer sen serigne yow la gnouy yeddeu
@@Mame-zw5gf 🤔🤔
Mbay touré limakoy dégu lépou dégué mo geuna bon ci adouna
Mane.dee.chauffeur.camion.lawone.fofou.mais.mais.les.4.freres.la.moussou.nion.leck.khaliss.boulenne.lewoule.yalla.na.yalla.atter.amine
Non je peux pas y croire ablaye digne que je connais très bien kou bah djoup mashaallah yalla nalen yalla tahawou
Môm dal daflèn exploitè ba doyal emprisonnè lèn , motax jeune dangay yèwou bo nèkè ci beureubou liguèyou kay 2 ans guisso ci sa bopp tu dois quittè et chercher autre chose
Doko tayy dee lou leer lala wakh danioulay yeww bagua degueur
Je ne connais pas le fond de l histoire, mais le faite de les faire travailler depuis l âge minieur est un délit, si c était en Europe l oncle aller les dédommager et faire la prison
daniouy wakh badienes yi mais nidiaye yi aussi dougnou dara. mane dé samay dome mane dongue ak Yallah
Non diambar dioyna masa arame😭😭😭😭
Bilahi justice bi sou bakhoul Dara d'où bakh sama khôl bi dafay nakhari 😢😢😢😢
Bilae li gnawna 😢que justice soit faite 🥺en bas la corruption
Allah va trancher dans de bref délais inchallah.
Aaamine y’a rabbi
Bilahi niou bakh niou neke khasso yalla nayala tegui natou bi j ai mal au cœur khamnalen bou bakh. Niou dioub sakh
Yallah naléne yallah takhawou 😢❤
Je pense bien que c'est Mbaye Touré de Touba le grand commerçant milliardaire qui a emprisonné ses neveux 😢
C’est lui dh
Kokou mom khana dafa doffff😂
@@AdjaDiordiopNdionecomment on peut emprisone ses neveux et aller dormir tranquillement
Cest grave Dieu ne dort pas
@@aminaba6130par ce que tout simplement il est dépourvu de conscience
Thi barké safar bi yalnaléne borom takhawou
Comment un milliardaire peut-il traduire en justice ses propres neveux ? Il préfère sauver son argent plutôt que la vie de ceux-ci. Allalou adouna djarouko dé ! Itakhoullah!
Mais sa frère yi ay actionnaire léne si ligayou séne Nidiaye bi 😢 mai es ce que ligayoul khalé yi 😮
Très bonne question
Liguey bi mo( tothie ) motax changema dina am inchal Mane mom vremant pabi dafama beet trop bilahi 😢😢😢
Loloula dih
@@aboridial264 daga kham pa bi
Mbaye toure dafa ligueuyone khaleyi ligueye ba tothieu
En tout cas amoul xol deh
Masta ma chérie Yalla nalenne KO Borome bi téguile. Tu m'as fait plairé. Toi leur sœur tu es une bonne personne une personne pieuse gentille généreuse. Yalla nalenne Borome bi taguawou. Toute la classe sup 1 de Ndiarka Diagne prie pour tes frères
Je ne peux plus retenir mes larmes 😭 thiey adouna metina
2 Badianes you bakhe merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mbay touré ya bon te Sénégal amoul justice
Yalnalèn yalla até
Yalla guis na lép yalla na yalla takhawou
Que la justice soit faite teudie kou défoul dara yalna diékh senégal
Doolè doukhoul diamm wayyya demain il fera jourr
Reewmi amoul justice nii la messa mel
Les membres de ta famille reste toujours les gens le plus dangeré pour toi et ta propre famille
En connaissance de cause 😢
Oh du courage Dieu est grand
Mann déy warouna😢sén badiane dioylo nama😢😢😢sén ndidiaye xana xamoul lii Yalla wakh thi djirim😢 Allahou Akbar 😢. Lii mom esclavage deug leu😢lii nak mo xéw thi rewmi 😢 alalou adouna diaroul lii dé😢ki mo bonn. Bilahi béss bou dougué thi biir bamèl dina faté loumou meusseu am thi adouna. Rakam yoyou ak domam yoyou dougnouko meusseu nianial ndakh xeuthio alal, diabar yi pa yi ndieukeunté lén ndakh alal dji😢. Yalla na Yalla arr xalé yi té natou bi nék sén thianguate thi barké Rassoulilah Aleyhi Salatou Wa Salam 💚 💚 💚
Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🤲 🤲 🤲 😢
Amineeee 🥺
Bilae gneupe la dioylo par ce que si khole la diouguè😢
Allahouma amine 🤲🙏
Bi lahi djirim man de😢sourr na adouna😂
DÉMATT LÉEN TEUSS AK XALASS BOULÉN BAYI MOU SÉDEU DÉ SINON RÉK LES 4 FRÈRES DINAGNE YAGG PRISON TÉ KI FÉBAR FOFOU WOROUL 😢
Yalla baxna yalna yalla leral lep barkey Mohamed yalla mo d'Axa até niit
Ki mo bone dafa compromettre avenirou khalé yi parce que yak n'a séne diang pour mou meuna réussir khalé you tôle thi diangue ga réquisitionné pour ga meuna téki léne séne akeu dinalène dale bala mo Sango Souf li dafa méti
SÉEN NIDIAYE BI DÉ XANA XAMOUL LI YALLA SWT WAX SI DJIRIME 😢😢 ALLAHOU AKBAR KI MO BONE 😮😢 DIEUL SAY DOME DEF LÉEN PRINCES 🤴🏿 ET DIEUL SAY DOMOU RAKEU DÉF LÉEN ESCLAVES 😮 KI MOY DOMOU HARAM DEGEUUU TÉ BONE 😢😢😢 LI MÉTINA TROPPPPPP VRAIMENT 😢😢 QUE JUSTE SOIT FAITE 😢😢
Lilay méti dileu gaagne, say mbok gnolakoy tek
Courage ma sœur va voir kewelo avec Babacar touré
Yalla naléne Yalla atté thi barki Seydina Mouhamed (SAW)
Justice doit être faite avec équité. Ils doivent être jugés ou libérés.
Bilay ki yalle nako akh liguékatam top tadinako guisse
Cette histoire est bizarre, combien de boutiques pour Milliards. Il faut toujours pensez a avoir ses propres choses après quelques années dans une boite ❤
Bilahi wakhaatiko
Tu n'as pas écouté boutiques la débutée après c'est des magazins c'est ta dire grossiste à Dakar et touba
@@bellediolla3414 elle a compris elle veut faire comprendre aux gens de penser à investir pour leur propre business après quelques années dans une boîte au lieu de suivre leurs patrons qui ne se soucient qu'à leur propre intérêt
Sheu mbaye toure amna lou eupeu 120 camion + des boutiques a touba et à Dakar
Sama khol ba ngi beugue dague yalla mon patient
Baye tourè bayil xaleye bi, ngui xam na lènn bou bax ligueye rèk la ngou xam ak jammou yalla
En tout cas le Sénégal manque totalement de justice
Yallah n'a borom bi atté thi lou gaw inchallah
Bilahi Toma aka meti Yalna niou yalla mousal si li
Yalla na yalla takhawu khaley si barke serigne Touba
Man europ la geum yoral ay milliards yak ki yoroul touss yénay yém justice
Kou yabou démal sa bopou lo am bakhna li métina
Mougne lène gninalène nalène justice dimbali
Badiane ya bakhe merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane dé bama khamé ni samay Nidiaye yéné wounma la guéni séne taate yi 😂😂
😂😂😂😂😂
Touk😂😂😂😂
Problème il faut surtout écouter les 2versions y a pas de sentiments ds les affaires
Ana diomaye Ana sogko Ana justice bi Guen donne wote ah yala rek mo worr
Allez vers tous les médias radios, télé, sites internet presse écritesque sais-je encore,que ce gros bras soit dénoncé que justice soit faite que diomaye,sonko soient informés car cet homme a compris l'avenir de ces enfants ,il a bafoué leurs droits il sait qu'ils ont maitrisé le travail et s'ils se lancent dans le commerce ils seront des concurrents qui peuvent le conduire à fermer boutique
Hana môme mo môme justice Sénégal wala d'à bari alale ha Sénégal Guen lene
Massa yala nalene yala takhawou barker mame babacar
Kou yabou liguéyal sa bopou bania liguéyal kéne
Bilaye ndeyesane ak ni boutique mété mais nak yallah geumoul nélawoul yallah nal yallah até si nimou geuneu gawé sibarké seydina moukhamed saw
Mbay touré dou nit kou bakh
Exploiter ay domou diambour ba doyal yobou len prison di yakar ni cela restera impuni
Xamna sene nidiaye dji dé dou fadial diarbatame gathié ninadiay dji mo bone ki dou rousse sax
Man mome damay wadia dékouréssé thi Sénégal li dafa niawé bilahi 😭 li dafa matin 😭😭😭😭😭😭
Tenez bon ça ira inshallah injustice bi dina djikh , gouvernements bi sera au courant
Meusouma Kham Ni Mbaye Tourè bimay dég Domérame la Non ,,Saway Ki Loum Am si ay (Remark ) Demna ba meuneutoul Muté Mouy Def si tourou rak dji Ibrahima tourè ,mè ki ndéké domou kharam deug leu
Sene tonton by il n'a ka faire attention prend garde
Nous interpellons vivement le ministre de la justice
Il faut dire son nom allez dans ta les médias il faut dénoncer cet injustice
Gni sen nidiaye daléne exploiter deug amoul béne yeurmandé wantéh lou way déff boppam
Lepp nakk yenn la pourquoi guéne bayi paa bii yobou lenn dii len yénnou lo ahh
Li barina si réwmi man sama propre pér momakodéf léka sama 4 millions dima menasse yalla nopina
Enquête sur mbaye touré et ses milliards guér kat la corrupteur la
Mbay touré ragalal yalla adouna day diékh déh
il faut alle voire SADIOGUOU SOLUTIONS TV LI DIAYE DOLET LA LES SONT CROMPI ALERTE DAME. BOTHIE❤❤❤❤❤❤
Mbay touré adouna dou keur déh bakhna
Deuk bou maytouwoul akh développement dinafadiafé
Mbaye touré khanaa dafa jeudd justice bi
Kouma beet la bilahi mbaye toure Adouna dou keur 😢😢
Ah mo Diara lathie mbaye dafa fate ni khana fi Adina rek la lep dafay diekh
Wa waw
Mashala yi badiene. Yalna yala ate alal. Diarouco
Tonton bi dé khana dafa faté Alalou adouna si adouna lay yam wakhatouma Gua bolé si ay akkkkk nitttt😢
Mbaye tôuŕe môme ķiñe khaña moye geumôul yala
C’est le début de sa faillite ma belle yalla Nopina teh dinalèn até incha’Allahou rabbi
Diomaye et Sonko regle cette injustice sinon les conséquences seront affreuses pour ce pays
Mbay touré khalatal déh bakhna euleuk dina niew déh
Justice dou masa am Sénégal
Makhala dioudou woul si xalis badola bou mak 😢
Les forces l'ordre en question il faut dire c'est qui et qui
Façon liguèye bi mou xéwwé man diarna si ak rako papa mais dama télla bayii démal sa boppou, dara Gëuno Nék resque 😌😌 yalla na lén yalla taxawou
Courage sister
Madame senegal amoul justice kou yor yay bour alakhira dîna nieuw
Wakh deug deh
Sen nidiaye dji bonn ba trop waye' adina d'où keur li niaw na trop