«Dagne may sote amouma kouma défendre Moumy Dani rek…» Ndeysan Pendo Guissé craque et fond en larme…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 9 апр 2024

Комментарии • 43

  • @fatouwade5048
    @fatouwade5048 Месяц назад +17

    Yana Yalla motali sa yéné si barké Seydina Moukhameth (SAW)🙏

  • @user-pi3gx2rq4x
    @user-pi3gx2rq4x Месяц назад +8

    Yalna sounou borom motali sa yene pendo

  • @nemanema7999
    @nemanema7999 Месяц назад +14

    C’est une bonne chose gua yenné demal kenene maka mais dafay fékk gua dème ba parè …. So démé ba gneuw nak Soula nékhé gua delouwate gua yéneko koula nékhe….. soûla nékhé naak gua hadjî sa hadji ba paré après gua def oumra yénéko kenene
    Mais adji mom sa bopp D’abord

  • @hhjg1664
    @hhjg1664 Месяц назад

    Am crying😭😭😭😭too pendo sorry may Jannah be dea final destination n all da departed souls too🤲🤲🙏🙏🤲🙏

  • @fatoudiallo-tn8sd
    @fatoudiallo-tn8sd Месяц назад +6

    Bilaye yaye gore yalna yalla motali

  • @user-mt5kl5xc3u
    @user-mt5kl5xc3u Месяц назад +9

    Machalah pendo une dame de valeur ❤❤❤❤❤

  • @SD-ih6bz
    @SD-ih6bz Месяц назад +19

    Mais fawe gueu dème Adjali sa bboop ba parè balla guaye démèle kène soudè mousso dème thi limma dègueu

  • @user-cv2vd1li2i
    @user-cv2vd1li2i Месяц назад +3

    Machahala yana yalla motali

  • @NafinaDiop
    @NafinaDiop Месяц назад +3

    Linga beugue famille Thione motakh ma beugue leu bilahi ❤

  • @ceciliamanga8746
    @ceciliamanga8746 Месяц назад +6

    You look amazingly beautiful Pendo ❤❤❤❤❤❤

  • @user-qk9il4vs5w
    @user-qk9il4vs5w Месяц назад +1

    Manchalla

  • @user-qj8wq1lw9v
    @user-qj8wq1lw9v Месяц назад

    Machallah tata pendo sagnsé ngua tu es une grande dame yalla motali sa yéné yeupe❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @NabouLam
    @NabouLam Месяц назад +2

    Amine machalla pendo ❤❤

  • @user-wv9mj1fz8h
    @user-wv9mj1fz8h Месяц назад

    Yalla na Yalla motali sa yénné Pendo Inch'Allah

  • @fallameth
    @fallameth Месяц назад +3

    Sa grand boubou rafetena nagame nianalé inchala maka

  • @MarAmericain
    @MarAmericain Месяц назад +4

    Dieuredieuf penda gise

  • @becayepreuvendiaye922
    @becayepreuvendiaye922 Месяц назад +4

    Vraiment Mane Wally rek la beugue Wally moye sama waye katt meunouma dégulou kénenne mais ki dougueul vidéo bi khamm sénégalais yi senne réaction mo dioumm.

  • @ndeyefatoundiaye1647
    @ndeyefatoundiaye1647 Месяц назад +2

    Massa mettina dh trop sakh mais nianal leen rek 😢

  • @ndeyefatougaye4071
    @ndeyefatougaye4071 Месяц назад +2

    Ndayssane 😢😢😢😢 doyna waar .

  • @fatoumatabah1413
    @fatoumatabah1413 Месяц назад +3

    Wolie blie wolie 😢 wally jambar la yy

  • @marietoudacosta8499
    @marietoudacosta8499 Месяц назад +2

    ❤Machalla pendo bien parlé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ j ENS sais quelque chose❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @coumbacamara4418
    @coumbacamara4418 Месяц назад +2

    Wa mom Wakhoul won diey Astou saré moy xaritam ?en plus ligua wakh si Fatou waré ya wakhé si internet mo takh mo conseiller la si internet voilà

  • @hhjg1664
    @hhjg1664 Месяц назад

    S. A.W.S❤❤❤

  • @oldemouha1843
    @oldemouha1843 Месяц назад

    C est ca la regle

  • @fillytoure7780
    @fillytoure7780 Месяц назад

    Péndo lignoula déf kougnouko déf sa déréte yeungou sénégalais mo meuneu gassal nit kambe té gnila done khass faralougnou kingua done khoulol mais yaw yaléni dérangé gnognou gno wara kholat séne bope rakhass séne khol té dougeul leussi moy séne diame mane ça fait des années malay suivre mais manchaalah mbakh la guiss thi yaw ak ame fouleu ame personnalité motakh yalla boléla ak nit you bakh donc boul falé borom khol you bone yi léne lalay dolil moy adamo ak choco filtré léne boul sékeu ak gnome woté ak wouyou téléphone gnognou nité ak ngueume dafa diékh thi gnome mais séne blocussou nafék bobou gnénegni défone safougnou gnoune gnila beugeu on t'aime point♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @user-xn6bx5up2q
    @user-xn6bx5up2q Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seydoudiop4870
    @seydoudiop4870 Месяц назад

    Bayil sa doule yi balanga adial keneu dangay adial sa boppou wayane rek mais yalla wowoula reine danga togne walikhou

  • @oldemouha1843
    @oldemouha1843 Месяц назад

    Adjalal sa bop ba pare dewene nga demal moumy

  • @marietoudacosta8499
    @marietoudacosta8499 Месяц назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mariamadabo9100
    @mariamadabo9100 Месяц назад

    Sénégal dal metina woyane késsé

  • @Sallyiba
    @Sallyiba Месяц назад

    Si c sa première fois c impossible il fo nga ath ba parei soga meuna adial sa bopou

  • @ndeyemaremediagne7750
    @ndeyemaremediagne7750 Месяц назад

    Pendo bane telle ioe khoum nga do gonei khalei 3 ans yi sakh daniouy adji

  • @fatimazahrachannel6404
    @fatimazahrachannel6404 Месяц назад

    Yénébi rafett na wanté niit menoul adji Maka pour Ken soufékéni démagoul maka.
    Demal adji ba paré une autre fois nga dem adji pour kénen

  • @MairyNdoye
    @MairyNdoye Месяц назад

    Tu fais le hadj 7 année.
    L' année prochaine tu vas à la Mecque pour Mommy

  • @user-yk3uo3in5u
    @user-yk3uo3in5u Месяц назад

    Soudè meussoulo adji makka meunoulo adiale kéne

  • @aminandiaye4953
    @aminandiaye4953 Месяц назад +1

    Yala motali

  • @khadyngom6579
    @khadyngom6579 Месяц назад

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @fallameth
    @fallameth Месяц назад

    Vraiment damala beugue perda damala beugue guisse bilay

  • @awagueye4622
    @awagueye4622 Месяц назад

    Kii khamal leenko que ni kou meusoul adji meunoo adjal kenn
    Mahalaa diine dagn kay gueustou

  • @user-cv2vd1li2i
    @user-cv2vd1li2i Месяц назад

    Li gua wakh deugueu rék la Sénégalais dafa faut