Bon reportage On vous encourage à faire pareil pour tous les lutteurs c'est vraiment posé et professionnel. On gagnerai bcp à connaître le combattant dans ces circonstances sans excès de gens qui veulent se montrer devant la caméra et sans intrus
Machallah bo téyé meune nga dane zarco diéleuh bou reuye moytoul khékhe ak mome té boul forcé action bou nioroul Ada yallah nala yallah may ndam amine 🔥🔥🔥💪
Ada nguir yalla phisik bi bouko mousseu yakh, bala ngako kham nga dem ba agg fi gnom balla wala modou agg, ken doula eup doolè nax naturelle la. Force à toi 💪🏾💪🏾
Mbaye gueye tigre de fass rék lamay dioh à chaque fois que je le vois. S'il ne lâche pas morceau il peut devenir roi des arénes en un temps record comme balla gaye2
Lima metti rek si ada fass moye béne makk nékoule si ccorém affairou foug rekk laye deff mais na moytou amoul saysayou mbeur dafa yeuk succes moytoul ada del nabatou boubah taye moytou site yi
De tout❤ vk toi ndanan j te suis depuis lors mais j vw que ta belle et bien progresser sur tout les plan donc continuer a bien bocer et insha alla u deviendra roi des arène amine....yalnala yalla méy ndan le 15 insha allah amine🤲🙏❤💪🔥🔥
Nice vidéo wa lutte TV. Ada fass Bo geumé sa bopp Di ngeu am dara si lamb ji bilaye .meun ngeu beurrë ñiémé ngeu..mai yi ngey deff . sortir you barri diarouko ay simékou fiii
Quelle innovation dans le monde de la lutte. Bravo à vous pour votre travail et votre professionnalisme.
Bon reportage
On vous encourage à faire pareil pour tous les lutteurs c'est vraiment posé et professionnel. On gagnerai bcp à connaître le combattant dans ces circonstances sans excès de gens qui veulent se montrer devant la caméra et sans intrus
Il s'est bien exprimé. Lamb guëm, guëm rek mo ci am solo ak fonk sa bopou.
Que le meilleur gagne InchaAllah 🙏🏿
Ada est un vrai athlète. Excellente mise en scène
Il m’a donné le début balla gaye 2
Machallah bo téyé meune nga dane zarco diéleuh bou reuye moytoul khékhe ak mome té boul forcé action bou nioroul
Ada yallah nala yallah may ndam amine 🔥🔥🔥💪
Ada nguir yalla phisik bi bouko mousseu yakh, bala ngako kham nga dem ba agg fi gnom balla wala modou agg, ken doula eup doolè nax naturelle la. Force à toi 💪🏾💪🏾
Ada futur roi des arène inchallah 👑🤲🏽yalla nala yalla may ndam inchallah
Mbaye gueye tigre de fass rék lamay dioh à chaque fois que je le vois. S'il ne lâche pas morceau il peut devenir roi des arénes en un temps record comme balla gaye2
Si c vrai ils se ressemblent
Papa makhtar doundeul🤲billahi tu connais très bien l'équipe de fass 💪
Khana yaw médina ngua dekeu
Bilaye yor na fite wi déh
lou leer machalla
Vrai mais pour wane leu ni balla ndnanane leu bimouy ame age ada fass nek na roi des arènes
La forme est convaincante bonne chance guerrièr
Zarco mom Doff rek lama soffé
Inchallah boul yakamti mbeur sa carrière avenir lamb si yaw leu nékeu couronne Roi des arènes dingako teyei inchalah🙏❣️on est avec toi et pr tjrs
Bravo Lutte tv Ada Fass un lutteur vraiment Motivation a part Modou Lo tu es mon lutteur
Tu peux devenir un grand champion tu es un athlète pure et dure il faut avoir un bon staff et un entourage bien pour gérer ta carrière
Mais son entourage a mal choisi son adversaire cette fois ci. Zarco est très coriace
Ada Fass futur roi des arènes inchalah 👑🙏🏾❤️
Ada fass amna avenir si lamb bi machallahh best forme mbeur
Cet vidéo m’a fait aimer Ada fass j’aime j’aime j’aime beaucoup le travail que lutte tv a fait sur cet vidéo chapeaux a vous lutte tv
De tt coeur avec toi Ada Fass
De la part d'un fan qui habitait à Fass Delorme Bentegnet. ❤️❤️❤️
Quelle innovation Bravo lutte_tv ❤🙏🏼
Boy bi daye sedal sama kholbi Boy moytoul mbirou adina tè liguey diamou yalla tè moytou togne ak akhe yalnala yala defal diame amine amine amine
Ada Fass rek laniouy topp barki alkhourane ✌
Boula Zarko diappé dingua xamni simple Mandikat ngua do bandit sax. Zarko mola euppe doolé euppe leuh Fit dakk leuh Beuréé 100000000 fois.
On est avec toi notre futur balla gaye 2
Magnifique reportage !!.. Les images, le son derrière
Bon petit doc! Et c’est bien m’inspirer du MMA avec ces countdown qui nous plonge dans les combats en immersion complete! Bravo lutte tv 👏🏾👏🏾👏🏾
Toi tu es un connaisseur des sports de combat: les Countdown de l'Ufc, c'est autre chose.
Ada rek louniouy topp 🎉🎉
L’authenticité de ses propos ont rendu ce reportage magnifique. Ada Fass leu héé🚀
Pour 😐😑😄😅👇👈
S'assurer
Un futur roi des arènes diam cii yaw ada ndakaru 🤩🙏
Sama mbeur mi ADA FASS un très grand champion yalla nala yalla may ndam
Il est temps k la lutte sénégalais avoir des innovations merci pour ce reportage
Boy combat bi sa combat la patience rék akh vigilant bonne chance boule ragale dara
Futur roi des arènes 👑👑
Man mome lén rek la lay wakh moy nga bayi moto Ndakh nitt yi danou ame si yaw yakar ta ngay touk di lakhatou Ndakh yila begue ❤
Wakh degue Ada Fass defema nékh bilakhi diam lék ngay am inchalla Yalna Yalla may Ndam lék inchalla
Ada Fass tu es un grand champion 🦍! Bonne continuation
un futur champion inchalla🙏
Machalah sa parcours rafet n'a yallanala yalla defal diam meune Ngasi am Dara dh
Neuko lamb baayi kheel futur rois des arènes Ada ndakarou
machalla ada fass yallna borom bi défal la ndam inchalla 🦁
Lutte tv vraiment vous avais une agréable job sur cet vidéo. very very good job.👍👍👍
Ndanane dgue ! Nako amateurs yi bayi xél s'il est bien encadré il fera parti du carré d'as inchallah bonne continuation...
Yalla nalla yalla samou defal la diam Ak ndam Ada fass
Lutte tv la télévision 📺 leader de la lutte sénégalaise
Yalla nala yalla may ndam❤️🤩🫶🏿
Yalla nala yalla May ndam ada fass c'est badara depuis guinguineo future roi des arènes inchallah
Nianal nalla NDam Ada Fass 🙏🏼mes respectél Sa adversaire sibir guéw bii rek pour dane ko Diam si ioe
Sama mbeur bi yalnala yalla ndame ♥️
Lima metti rek si ada fass moye béne makk nékoule si ccorém affairou foug rekk laye deff mais na moytou amoul saysayou mbeur dafa yeuk succes moytoul ada del nabatou boubah taye moytou site yi
Boy bi ligueye na Manchallah 🔥🔥💪💪
Ada Dakaru kassé bly Mbeur gua demm rk inchalla ada 🎉🎉
Yalla boula thiate Doug Ada🙏🙏
Mbeur champion nga mais yokal liguéey bi té nga lakhatou lou bari yalna yalla mayla ndame lou reuy amine bon continuation 👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻
Mande yaye bouga wakh rek moma toucher lol billah Dame bouga sama yaye ❤❤❤
Balla gaye 2 2006 rek lay guis si ada fass mbeur man NGA âme louné si lamb diapal rek Dina bakh inchallah
Domou fass on t'aime 😘💪🏿
Zarko Rek do kholl domou grand yoff bi ❤️🇸🇳
Suis fans d balla m’ai franchement chapeaux 😊
Champion deug ❤
Tournage bi nice nactrop bravooooo
Lutte tv barre bi kawé neu trop bilahi. Je suis amateur de boxe et de Mma. Mais li su preparation combat de boxe yi rek lako done jiss ( All Acces ) 🔥
Le Grand Phénomène 💯👏👏👏👏
Yallah na yallah may ndam mon idol
Bonne Chance Adama Correa. Yalla nala yalla may ndame
Machalah Yalla nagnu tiate sekhlou barke naby ❤
Machallaah Ada Fass Yalna Yalla maï ndam inchallaah
Bravo à vous lutte tv 📺 vous faites du bon boulot ❤
Adama corréa🥰💪🏿💪🏿
Yalnala yalla may ndam sama mbeur bi mane damaka beugg bilahi🙏🙏🙏
Courage et bne continuation à ltte TV. Ada fass ndam rek
Effectivement impressionnant il s’est métamorphosé en seulement 2 ans
Le futur champion ❤️❤️
Ada ndakarou diam ci ioe dila nianal ndam 💪🏽💯🙏🏽
Figua tëk sa tank fofou laa liguey rëk Yagui tchi YoN dh mbeur ❤️ day magg dëff beum
Yalnala yalla maye ndame
Bonne chance Ada Fass Borom Dakarou ❤️
Ada fass welikam no feewi👍👍👍🤘
Lutte tv vous avez vraiment innové la lutte
De tout❤ vk toi ndanan j te suis depuis lors mais j vw que ta belle et bien progresser sur tout les plan donc continuer a bien bocer et insha alla u deviendra roi des arène amine....yalnala yalla méy ndan le 15 insha allah amine🤲🙏❤💪🔥🔥
Sen affiche et lutte TV good job vraiment
SUNU TAPHA GUEYE...💪
Ada boul meusa nan domm ya ngui ak forme bou rafettt
Nom wakh degue fralouma la wayè am ngua dolé machallah
Images et magnifiques 🎉🎉
Ndame Kasse inchalla ❤ ✌
Lutte TV chapeau 👏👏💯
Nice na diame si yaw ❤ 🙏
Ki bëréé gul Billahi bëré rek lay def
Mahsallah yalla yallah diapale ada
Nice na machalah ada fass ndam rk
Class 97’❤ aytia Ada
Futur rois ❤
Nam rek inchallah ada fass
Nice vidéo wa lutte TV. Ada fass Bo geumé sa bopp Di ngeu am dara si lamb ji bilaye .meun ngeu beurrë ñiémé ngeu..mai yi ngey deff . sortir you barri diarouko ay simékou fiii
Fougou jeunesse
Liguey mome def ngako masha allah
Yalla nala maye ndam amine
Mon futur champion Ada fass❤️
Ada fass yalla Nala yalla may Ndam rék inchallah
C'est un phénomène franchement
Amnga ngeum ngeum vraiment wayé combat zarko mogeuneu diékou gagné KO inchallah
Yalla nala yalla maye ndam si barki cheikh Ahmadou bamba
Merci pour cette video et pour la prochaine fois , il faut cacher le nom de la societé (on ne fait pas de la pub gratuitement)
yala hamnani ada fass, reug reug ak Franc koulen moytouwoul si lamb dji dinga am blem boy yi amnagn dolé bilahi