Assane Ndiaye - Serigne Abdou Karim "Clip Officiel"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 фев 2025

Комментарии • 355

  • @khadygkante6099
    @khadygkante6099 5 лет назад +278

    Kouy bégué papa assane Ndiaye beusseul 👍may guiss
    Ani gniy setane té di lire commentaires gneuweul ni malay seneu😍😍😍😍

  • @AdjaTraore-m8h
    @AdjaTraore-m8h 3 месяца назад +1

    Ndeysanne sama serigne bi baye karim yalla ngafi yague té wer mbacké balla aka bakh❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyemareme38
    @ndeyemareme38 3 года назад +4

    Sama Serigne Abdou karim yallah nako yallah mayy werr assane Ndiaye bonne continuation ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏

  • @lakarimienne1858
    @lakarimienne1858 3 года назад +1

    Machalah khol sede na walahi loway mou nekh daye yare bithi iow rawatina kigua diper way bi mouy sougnou yakar tay ak euleuk borom yare ak teiguine ak jiko bou raffet

  • @khalifadiop4175
    @khalifadiop4175 5 лет назад +8

    Masahlla ndiay diata serigne abdou karim mbacke yalla nafi yague té wer si barké serigne touba khadim rassoul amine amine amine

  • @cvpointernational4549
    @cvpointernational4549 5 лет назад +38

    Premier fois regarder le vidéo assane Ndiaye TAKK Serigne Abdoul Karim MBACKÈ assane boul dh geudj wày 👍

  • @doudouxbaby7324
    @doudouxbaby7324 5 лет назад +53

    Akka meuna weuye Mach'Allah❤️

  • @binetambodj3100
    @binetambodj3100 5 лет назад

    Gé toujours été fan de Assane ndiaye n"1 m tay la Raw ndax wayalnama sama xaritou xool Baye Karim...jlaim becou...na message bi éque si mom nguir Yalla... C Bineta bou Baye Niass....!

  • @sarrmouhamedmarena4079
    @sarrmouhamedmarena4079 5 лет назад +35

    Machallah sama serigne bay karim mbacké yalla nafi yague té wère amine🙏🙏🙏

  • @nittoudeugrek9684
    @nittoudeugrek9684 5 лет назад +3

    Ndeysane bilay assane wakhal serigne abdou Karim kene dou mome mbacke balla barki serigne touba ligua done rek gua mena done ndakh serigne fallou borom na am mou am moy sa wadiour way MAchalla kou beug baye Karim defal ni 👍may guiss

  • @thiekone7849
    @thiekone7849 4 года назад

    Machalah yalla gue goudou fan te am weur amine

  • @queenysy4347
    @queenysy4347 5 лет назад +10

    Ndeysan😭❤️❤️sama mbeuguel si baye karim dama yém barki Serigne fallou❤️🙏🏽yalna diamam yag si barkeip borom touba

  • @mamediarrandiaye6273
    @mamediarrandiaye6273 5 лет назад +15

    Mashallah Baye Karim dans nos ❤❤❤❤❤yalla na yalla goudal fane Mbacké 🥰🥰🥰🥰🥰

  • @mounassndione1919
    @mounassndione1919 5 лет назад +11

    Machala sama chanteur bi aka am mana am class soko dégué rék da guèneu albums Yalna yalla yok mane mane bi wéral bate bi Ndiaye. Serigne Abdou Karim Mbacké Yalna fi yague lole té ande ak wer Mbacké ak mak niou bakh yeup si barké Seydina Mouhamed

  • @ndiayeawa6025
    @ndiayeawa6025 5 лет назад +8

    Sama Serigne bii baye Karim machalla pp Asane Nice na khôl sédd Na bonne continuation à vous

  • @elhadjiann7310
    @elhadjiann7310 5 лет назад

    Daguamay wout nakkk père assane sama khol gua lalll ya dakha way sénégal pose blue ❤️

  • @sowalhaj6236
    @sowalhaj6236 5 лет назад +1

    Assane mane damala buegue nakh saye wakh bariwou saye dieufeu eupeu clip bi machallah

  • @iboudiop9093
    @iboudiop9093 5 лет назад +1

    Kiiii moooo dake weuye Senegal

  • @yakasene617
    @yakasene617 3 года назад

    Koumay wonalék assane Ndiaye damako beugue troppp bilahi yalgua goudeu fane papa assane

  • @aissatoungom5045
    @aissatoungom5045 5 лет назад

    Bilaye ndiaye diatta papa Assane machalah yalna yalla du weureul batte bi rekk tey nga mandou nga lafthiate

  • @elbachir67
    @elbachir67 5 лет назад +6

    Diguente aldiana ak daarou salaam matoul kheulou ba khawess nako mana raam ...

  • @khadimsarr3892
    @khadimsarr3892 5 лет назад +2

    Li mom machalla baye karime yagg fi lol tei ame wer brome maharimal ahla 🙏

  • @seydinafall3990
    @seydinafall3990 5 лет назад

    Baye Karim yalla nafi yague lol té weur diadiaf papa assane

  • @ndiayedaro9275
    @ndiayedaro9275 5 лет назад +7

    Machallah tonton linga waye sangue bi meuna toko segne Abdou Karim Mbacké geuna yague geuna werr

  • @falldior9914
    @falldior9914 5 лет назад +1

    Mashallah ASSANE NDIAYE , yallah boula thiat topeu way notre Grand chanteur .

  • @fatouball1078
    @fatouball1078 5 лет назад

    Wayé tinga sama fans bi

  • @elisasenepereira583
    @elisasenepereira583 5 лет назад +1

    Je vs adore Assane Ndiaye je vous écoute depuis Portugal presk ts les jrs lingay weuy nexna mashallah 😍

  • @magattediouf7241
    @magattediouf7241 5 лет назад +1

    Barki s touba mane ma beugue assane ndiaye sama khol loumou way néxna ma

  • @aidagueye5765
    @aidagueye5765 5 лет назад +4

    Machalla sama domou serigne yalla nafi yag tè wèr amine

  • @sodandiaye8724
    @sodandiaye8724 5 лет назад

    Ahhhhh sama xol sede nan trop man dama yag beug assane ndiaye pask sama domou baye la teh man dama beug kou sant ndiaye mouy tamite sama waykay mandal konta nan si clip trop yalla nanko serigne fallou tek lokho

  • @ndeyebintandiaye9837
    @ndeyebintandiaye9837 5 лет назад +1

    Machalla papa assane sa voix dall deugue nekhoul dinga degue loum def👇
    dèfati nga sa manin de kendou serigne abdou karime

  • @ibk4266
    @ibk4266 5 лет назад +7

    Dieureudieuf baaye abdou karim Mbacké 💙🙏🏽

  • @idamarietou3019
    @idamarietou3019 5 лет назад +2

    Elément sama Papa Thione seck so meunoul waay togn barké Serigne Bamba Yalla na sa diameu yague

  • @bijoulo7428
    @bijoulo7428 5 лет назад +11

    Mashallah mé 3s morceaux assane Ndiaye dara dou mom yalla boumou wogantiko hooo j'aime ça way❤

  • @mahmoudfalilou8175
    @mahmoudfalilou8175 5 лет назад +4

    Baye Karim keineu dou mom yaggfi tè wër Mbackè
    Diadieuff Assane

  • @baidyrassoulsow5487
    @baidyrassoulsow5487 3 года назад

    Ya meuneu waay assane doundeul waay Ndiaye....

  • @bbjulindiaye
    @bbjulindiaye 5 лет назад +39

    Mais Ñiiy Dislike C Koi Leur Problm? Bagn Bagn Beug Ndiaye Barké Akhmadoul Khadim Nio La Beug Piir 🤩. Bu Relike Amoon Nga Xamni Leep Deug Leu Dundul Ndiaye

    • @TopNormaL
      @TopNormaL 5 лет назад +2

      Khana khamo amna nio khamni dagno mome senne téléphone di beusse foullenne nekh rekk wayyé khamougnousi daara lolou Késsé moyye senne problème

    • @elhadjiann7310
      @elhadjiann7310 5 лет назад +1

      Xamou gnou loumouy signifie ndeysan

    • @moussaniangane4804
      @moussaniangane4804 4 года назад

      @@TopNormaL faut savoir aussi que RUclips nékoul sénégal rék la mais c partout dans le monde

  • @binettadiallo321
    @binettadiallo321 5 лет назад

    Ya dakka woye si Sénégal bâ pare am classe kéna doula dègua si lou gniakka fayda

  • @keurserignetoubamulti-serv4334
    @keurserignetoubamulti-serv4334 5 лет назад

    yalla na yalla wéral bate bi

  • @nourouchikory8113
    @nourouchikory8113 5 лет назад +3

    Ndanaan leu assane

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qg 5 лет назад +5

    Oh my star is back mom rek moye weuye ma deuglu ko 1st time mu nekhma, I love assane

  • @dioufreference7883
    @dioufreference7883 5 лет назад +10

    One love fratello depui italie on t'aime fort❤️❤️❤️

  • @diagadiaga6013
    @diagadiaga6013 5 лет назад +26

    Mach Allah assane merci ❤❤❤❤

  • @sapboy421
    @sapboy421 5 лет назад

    Diadeuf assane ndiaye👈👈👈🙏🙏🙏🙏🙏

  • @fatoufall2253
    @fatoufall2253 5 лет назад +3

    Nooo mane ki souy way sama xol❤️bi lay lale😍😍😍

  • @kharitouwally186
    @kharitouwally186 5 лет назад +3

    Mane dal namon nako♥️♥️👍👍

  • @awabdoulaye2783
    @awabdoulaye2783 5 лет назад +5

    Tabarfaq'Allah Assane lii nékhna. #Mouride mo nékh

  • @salygueye4342
    @salygueye4342 5 лет назад +2

    Machallah kou meuna way mogui way kou nékha way mbacké balla

  • @ouzinmessi5938
    @ouzinmessi5938 5 лет назад +1

    Merci beaucoup assane et dounell way konetane billahi Nice na torp mashala

  • @diagnegnilou1078
    @diagnegnilou1078 5 лет назад +2

    Bilay waye rek laydeef

  • @espaceannexe436
    @espaceannexe436 5 лет назад +4

    Mon Musicien Préféré Machallah

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 5 лет назад

    Wa pape fo nékone nékh naa machalaaa mbacké balla yageu fii lole té wére

  • @ndeyembodembengue8600
    @ndeyembodembengue8600 5 лет назад

    assane machalla mane yaw laye weure bilahi

  • @adamacisse987
    @adamacisse987 5 лет назад

    sama fans bi mala beug

  • @xaritoupapamreknak3953
    @xaritoupapamreknak3953 5 лет назад +3

    Way lou nekh rek sa yeuf la bilahi ame class yaurou 💖

  • @antagueyefall5478
    @antagueyefall5478 5 лет назад

    Yalla na bate weure ndiaye

  • @ndeyefatoundiaye4376
    @ndeyefatoundiaye4376 5 лет назад +1

    Masha'Allah liii nekhna lolou sax balla aïssa Gueuna yagu Gueuna wer

  • @farydayega3631
    @farydayega3631 5 лет назад

    Nice ssama kharit long vie rekk

  • @dioufdiouf1943
    @dioufdiouf1943 4 года назад

    Wayyy dé moko dak Sénégal

  • @dabafall7531
    @dabafall7531 5 лет назад +11

    Ndeysane a chaque fois c'est comme ça il assure grave voix unique❤❤

  • @rusamelrusamel2642
    @rusamelrusamel2642 5 лет назад +2

    Machalla way Assan lii nekh na ma 😍💃💃😘😘😘

  • @bassseye6817
    @bassseye6817 5 лет назад

    Man ki la beug bilay petit ba grand

  • @sarjomarong2613
    @sarjomarong2613 5 лет назад +4

    Ma'sah'Allah Assan Njie neh na lol 💃💃💃❤❤❤

  • @mamadoumbaye7771
    @mamadoumbaye7771 5 лет назад

    Ndiay asan nexna torop

  • @mamesayedia8319
    @mamesayedia8319 5 лет назад +3

    Alhamdoulilah bismilah machallah sama papa assane ndiaye is back 😍😍

  • @khossanefaye640
    @khossanefaye640 4 года назад

    Akassa baye karime je l'aime beaucoup

  • @fatoucisse3820
    @fatoucisse3820 5 лет назад +1

    Yangimay sogaa nexx

  • @aminarassoulndiaye6828
    @aminarassoulndiaye6828 5 лет назад

    Barki Srg Touba yaa meunn wooyy sama ndanane biii niounn ak yaw dafa yagg lou deff mou nexx konn en route vers grand théâtre inchallahh dpui Maroc

  • @ndongodaara2391
    @ndongodaara2391 5 лет назад +6

    Aka meuneu wôy téh dou wakh wakh diou baariii !¡!¡

  • @diopnar4205
    @diopnar4205 5 лет назад +1

    Yamana waye ndiaye

  • @bbjulindiaye
    @bbjulindiaye 5 лет назад +10

    Mashallah Ndiaye ❤

  • @marinakarim815
    @marinakarim815 5 лет назад +1

    Baye Karim Mbacké 💙💎

  • @fatoucisse3265
    @fatoucisse3265 5 лет назад

    Machalah serigne bi loko waye doyoule borome makarimale akhla

  • @anitazahradiop357
    @anitazahradiop357 5 лет назад +1

    Bilay mala beug

  • @kumbajagne987
    @kumbajagne987 5 лет назад +10

    Masha'Allah Assan Ndiaye 👍🏾👍🏾❤❤

  • @falloungom2001
    @falloungom2001 5 лет назад

    Thiey bayé Karim MBAcke

  • @sokhnadia9452
    @sokhnadia9452 5 лет назад

    Papa assane ndiaye l'y nehna clipbi rafetna Wat tel l'ay def machala sama waykatbi

  • @abdoulayediallo2444
    @abdoulayediallo2444 5 лет назад

    Foo neko Ndiaye machala

  • @kadiakamara9055
    @kadiakamara9055 5 лет назад +1

    Neekha tina papa👍

  • @mamitacisse4023
    @mamitacisse4023 5 лет назад +4

    Tu chante trop bien je valide bravo💃💃💃💃💃💃

  • @chachaba9201
    @chachaba9201 5 лет назад +2

    Lo deff mou nekh ❤️😍😍

  • @matydiagne7434
    @matydiagne7434 5 лет назад +2

    Machalah homme discret dans son coin et fait du beau boulot

  • @TEAM_DMG_OFFICIEL
    @TEAM_DMG_OFFICIEL 5 лет назад +4

    Yalna fi yaguè ta weerr ❤❤❤❤👍

  • @gayendiaye1634
    @gayendiaye1634 4 года назад

    Vreama assane est le seul chanteur dan notre mode

  • @jonoceesay9856
    @jonoceesay9856 5 лет назад +2

    Masallah assan njie...god guide and protect you njie jatta

  • @sayfall7076
    @sayfall7076 5 лет назад +1

    pape assane beugeu nala torop Machalla💖

  • @toubandiaye8069
    @toubandiaye8069 5 лет назад +4

    Machallah sama artiste bi wayy rek lay def

  • @kourasarr1957
    @kourasarr1957 5 лет назад +8

    Toujours égale á luis même , MachaHALLA 😍

  • @awamouvivianesylla6026
    @awamouvivianesylla6026 5 лет назад +1

    Nekhatina way🥰

  • @ndeyeniang1765
    @ndeyeniang1765 5 лет назад

    Au trop nekh machalla waye rek laye deff 😘😘

  • @moustaphagueye7747
    @moustaphagueye7747 5 лет назад +1

    Ndanaan bou mak bi👍

  • @poullodierry7011
    @poullodierry7011 5 лет назад +1

    Super,Super,Super Machalla

  • @mariot6429
    @mariot6429 5 лет назад +1

    Machalla papa assane laf thiat si yaw♥️♥️♥️

  • @fatoulagnane4676
    @fatoulagnane4676 4 месяца назад

    Machallah ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

  • @thiaatniang4941
    @thiaatniang4941 5 лет назад +1

    Bilaye ma begue ndiaye assane ❤

  • @hawajaiteh7192
    @hawajaiteh7192 5 лет назад +1

    Mashallah papa Assane Li dess Yallah na barkel

  • @ndeyemaguettediaw3937
    @ndeyemaguettediaw3937 3 года назад

    Mane la ndeye maguette diaw sopey Serigne Abdou Karine mbacké ma sope.la lalol

  • @mbayefall7045
    @mbayefall7045 5 лет назад +1

    Manchall nice nous sommes tres content

  • @nafissatoumbaye8465
    @nafissatoumbaye8465 5 лет назад

    Machallah NDIAYE diatta ndiaye Lo wayy mou Nekh machallah

  • @khadidiatoudiop8719
    @khadidiatoudiop8719 5 лет назад +2

    machallah sama chanteur préfére