Abdoulaye Diop Bichri: "Ce que Serigne Touba et Mame Maodo s'étaient dit à Ndiarné..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 фев 2025
  • ▷▷ ABONNEZ-VOUS ICI : Cliquez ici pour vous abonner
    🔔 Activez les NOTIFICATIONS pour ne pas manquer les prochaines vidéos
    Retrouvez-nous sur www.seneweb.com/
    ------------------------------------------------------------------
    #Sénégal
    #seneweb
    #Actualité
    #Politique
    ------------------------------------------------------------------

Комментарии • 346

  • @vandermayoalicia8527
    @vandermayoalicia8527 3 года назад +3

    Mash'Allah Cheikh Akhmadou Bamba Ak Aladji Malick Sy gnoo baax Yalna Yallah yook yërmandém ci gnom ak njégalam té saam seen ay njaboot ak seeni talibé ak seeni soopé ci darajaay sen sopé ba Rassurul Rahma Seydina Mouhammad Sallalahu aleyhi wa Salam li moy Sénégal keep ku beug tass Reew mi Yalna bo sa péxé aag.

  • @mariamasow3970
    @mariamasow3970 5 лет назад +48

    MACHA ALLA LI MOY SÉNÉGAL DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFE MAME MAOUDO MALIK SY❤❤❤❤❤

  • @lakhadiokorediokore3916
    @lakhadiokorediokore3916 5 лет назад +64

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭AL hamdoulilahi sama khoole toyenaaa kou beugue Sénégal beusseulle j aime

  • @omar-salihdiop6692
    @omar-salihdiop6692 5 лет назад +18

    Dara keuneu nékhoul niouy wakhtané S Touba khassisayi di daw si souf dieureudieuf bamba
    Gnébeula défal😘😘😘😘😘

  • @edy6670
    @edy6670 5 лет назад +16

    Yallah nagnou yallah(swt) bollé gnou dooneu béneu Ci barké khadim RassouliLLAH Mame Maodo sy Baye niass Seydina limamoulaye ak kilifé diiné adina bi yeuppp. Inshallah

    • @originaldiouf7768
      @originaldiouf7768 5 лет назад

      Yalna yalla féyla ngeugui faye amiiine ❤❤❤❤ ambassadeur

  • @thiernoniang5625
    @thiernoniang5625 5 лет назад +13

    Machalla dieuredieuf seringe abdoulaye Diop bichri

  • @ndeyebintadieng7864
    @ndeyebintadieng7864 5 лет назад +3

    Machaala serigne bi ya bakh bilahi yalnala yalla faye barké mame maodo malick

  • @nomprenom5376
    @nomprenom5376 5 лет назад +53

    DIEUREU DIEUFATY SERIGNE TOUBA
    DIEUREU DIEUFATY SERIGNE TOUBA
    DIEUREU DIEUFATY SERIGNE TOUBA
    DIARRAMA MEME CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @Self22
    @Self22 2 года назад

    Ma cha Allah
    Khôl sedeu na
    Li moy Sénégal

  • @boubacarmballoka2702
    @boubacarmballoka2702 5 лет назад +7

    Machala ❤️ Amna solo trop bilay ❤️🤲

  • @saffdiagne1244
    @saffdiagne1244 4 года назад +3

    Alhamdoulillah li rk moy senegal diam rk lep bene la wakh dji moy barri te lep bene la way 🇸🇳🙏🙏talibe yui niou wala nopi te xamni senegal diam rk mofa ame

  • @mamadoubah9174
    @mamadoubah9174 4 года назад +2

    Macha allaha sanguebi koulene séparé wallahi daguay sonnou rekk

  • @khalillamp5648
    @khalillamp5648 5 лет назад +10

    DIEUREUJEUFÈ SERIGNE TOUBA KEN BAYOU SERIGNE SALIOU

  • @zousport
    @zousport 5 лет назад +11

    Yalla Naniou Yalla Fayal Makk Gni

  • @seydinamouhameddiop7812
    @seydinamouhameddiop7812 5 лет назад +2

    Machallah amna solo trop yalla nagafi yague

  • @mameboussodiouf3883
    @mameboussodiouf3883 5 лет назад +10

    Macha'Allah ❤️

  • @malicksow4709
    @malicksow4709 Год назад

    Dieureudieuf Cheikh seydil elhadji Malick akk mame borom touba

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 5 лет назад +1

    Akasa amna solo Dieure dieuf machalla merci abdoulaye diop becheri deukla weure nade

  • @asfoppss
    @asfoppss 5 лет назад +34

    Dieureudieuf seydi Elhaji Malick Sy

  • @khalebeuztv3391
    @khalebeuztv3391 5 лет назад +9

    Machallah
    Machallah
    Machallah

  • @sassoumeseye6159
    @sassoumeseye6159 5 лет назад +6

    Machalah sama sopee wakh dji amna solo

  • @ousmanendiaye7516
    @ousmanendiaye7516 3 года назад +1

    Walahi Sénégal bognou donne deff nii djamou rék lagni amm li rekk moyy bolley ay djoulitte machalla

  • @papiscisko6648
    @papiscisko6648 5 лет назад +11

    Ya Rassoul ❤

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup7403 5 лет назад +4

    Machalah yall na diam yagg

  • @mamadouba8372
    @mamadouba8372 4 года назад +1

    Bonjour la famille SY et la famille BA divulgation total merci 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊

  • @kineowensndiaye2842
    @kineowensndiaye2842 5 лет назад +2

    Dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne abdoulahi Diop diadieufeul nala bou werr machalla rafète na lol way

  • @saliouniang3111
    @saliouniang3111 5 лет назад +1

    Machalla ame na solo li moye sénégalle diame réck mofi khathie

  • @mbayediouf7119
    @mbayediouf7119 5 лет назад +3

    Yalla khamnani woyyy yi ngay wakh ladone weurrr machlla🙏

  • @MCKTV-tc5rh
    @MCKTV-tc5rh 5 лет назад +1

    Machallah sama serigne

  • @boyetownfromdkr5287
    @boyetownfromdkr5287 5 лет назад +28

    Léepeu béneu là ayy djoulite laniou niom nieup ayy nitou dîné lagnù naniou yéwou wayy nioune talibé yii

  • @mourtalladieng406
    @mourtalladieng406 3 года назад

    Machallah yalla nala yalla sammu

  • @khadimgueye7166
    @khadimgueye7166 5 лет назад +10

    mashallah rafetna

  • @bbtitimbaye2894
    @bbtitimbaye2894 5 лет назад +16

    Bamba da yatou feipp ndeyssane brom al wara

  • @mamadouba8372
    @mamadouba8372 4 года назад

    Bonjour les tiedios la vérité merci divulgation total merci 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊

  • @libassetall5984
    @libassetall5984 3 года назад

    Li moye Senegal kou niou beugueu Tagaloo yaye torokh rek dieureudieuf cheikhoul khadim dieureudieuf Mame eL HADJi MALICK yallah na yallah yokou seny leer takh niou seny barkeb aminnnn

  • @khadimgueye7166
    @khadimgueye7166 5 лет назад +6

    mashallah

  • @Codoushabvby
    @Codoushabvby 5 лет назад +3

    Macha Allah mbacke

  • @ouleycamara3260
    @ouleycamara3260 5 лет назад +2

    Macha allah macha allah

  • @ndeyebinetasow8602
    @ndeyebinetasow8602 5 лет назад +3

    Machala

  • @parfumerieetcosmetique6265
    @parfumerieetcosmetique6265 5 лет назад +10

    Yallna Diam yague

  • @djibydiagne8134
    @djibydiagne8134 5 лет назад +1

    Machaalhaa

  • @cheikhsaliousylla837
    @cheikhsaliousylla837 5 лет назад +7

    Nane kham ni béne lane bilahi béne lane 😭😭ana gni nagko lima wakh

  • @malickseck911
    @malickseck911 Год назад

    Ko diokh adiya moy sa Serigne

  • @KILIFEUGUII
    @KILIFEUGUII 5 лет назад +4

    machllah seytané ya beuri légui di diakhassé rek

  • @serignebarasene6669
    @serignebarasene6669 5 лет назад +8

    Machallah kadouyi rafetna limoy diné

  • @fallouniangniang1849
    @fallouniangniang1849 5 лет назад +1

    Dieureudieuf seringe touba khadim rassoulilah

  • @creartstudiosenegal5079
    @creartstudiosenegal5079 4 года назад

    Mashalla ya bari kham kham

  • @auneymwseck2570
    @auneymwseck2570 5 лет назад +2

    machallah

  • @papemomarseck1256
    @papemomarseck1256 4 года назад

    Masha allah

  • @sofiyatoudiop9074
    @sofiyatoudiop9074 5 лет назад +1

    Amna solo maa chaa Allah
    Wayé nak soit reconnaissant nak Tivaoune gua diangué

    • @huaahuawei5457
      @huaahuawei5457 4 года назад

      En Tivaouane la diangué kouko diangal fofou

  • @bakhgueye3607
    @bakhgueye3607 5 лет назад +3

    Macallah

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 4 года назад

    Merci Bichri yow dè kou bakh nga, nga balma ak ndakh commentaire na ba tayi dila critiqué dama defeniwon yake ganna mèsèrè yame ndekètè bokoulène domoromame

  • @ndeyecodougueye3348
    @ndeyecodougueye3348 5 лет назад +2

    mashalah

  • @viamilano5738
    @viamilano5738 5 лет назад +2

    Ablaye diop bichri aka mo meuneu fènn..c'etait mon promotionaire de classe au lycèe limamoulaye.j l connais tres bien..dou tousse faux type...lima xam si mom si ay tothie tothie youmouy dèf..nèna legui professeur espagnol..no senegal dou dèm

    • @bayegallasjoop7319
      @bayegallasjoop7319 5 лет назад +2

      Yaw kou rew nga ki limouy wax lou lerr la nga diko saga nit dafay am yarr au moins nga respacté gnimou nek sén kilifa

    • @viamilano5738
      @viamilano5738 5 лет назад

      @@bayegallasjoop7319 yaw ki matoul kilifeu.maleu ko gueuneu xam..hana yaw ak sa baay llanèk sèn kilifeu

    • @edy6670
      @edy6670 5 лет назад

      via Milano xana daga doneu ande ak momeu di déf tocc tocc, légui moy sa kilifeu . Yow xana daga sétt Ci bakar wala t'ai un saint-homme bay wérr niteu Ci rèseau bii

    • @bayegallasjoop7319
      @bayegallasjoop7319 5 лет назад

      @@viamilano5738 ton nom montre k doumou xaj nga sén clavier ngéni lakatou di wAx loulén néx mé bo guéné wax ko niou tégal sa ndaye

  • @malicksow4709
    @malicksow4709 Год назад

    ❤❤❤❤❤

  • @ibrimasarr3337
    @ibrimasarr3337 5 лет назад

    Marsallah serigne bi rafettalgi yaguena nitkubakhga.

  • @amethbadiane4257
    @amethbadiane4257 4 года назад +2

    🙏💖💖💖💖🙏

  • @abdousarr4928
    @abdousarr4928 5 лет назад

    Machalla amna solo lolll

  • @malickseck911
    @malickseck911 Год назад

    Amoul morom khadim Rassoul

  • @bintoufall5210
    @bintoufall5210 5 лет назад

    Machalla rafetena

  • @oumarcondiniordiatta3784
    @oumarcondiniordiatta3784 5 лет назад +2

    Thieuy Yalla

  • @micksow7261
    @micksow7261 5 лет назад +1

    Macha Allah Bichri

  • @mamadouba8372
    @mamadouba8372 4 года назад

    Bonjour ors et diamants Sénégal et que les grands banque mondial garde merci de me le restituer à moi mamadou BA et le pétroles et gazs naturel Sénégal uniquement moi merci divulgation total merci 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 mamadou BA

  • @fatoumboup409
    @fatoumboup409 3 года назад

    Ki mon dakh fen si senegal

  • @didi.tvdaldiam5070
    @didi.tvdaldiam5070 5 лет назад

    Yalla na yalla fay la yiw

  • @ndeyediagne57
    @ndeyediagne57 5 лет назад +1

    bilahi mame thiérno borom darou néna kouy teukeulé s touba ak kéne. kéne doula té am yari baméll bilahi noni s bi layeu reum

  • @zalnice7488
    @zalnice7488 5 лет назад

    Amna solo

  • @moustaphafaye2762
    @moustaphafaye2762 5 лет назад

    Wawaw ana solo way

  • @moustaphafallniang8156
    @moustaphafallniang8156 5 лет назад

    Nous sommes tous des amis

  • @morgueye2635
    @morgueye2635 5 лет назад

    Vrement kadouyi amna Solo

  • @elhadjicisse1924
    @elhadjicisse1924 5 лет назад

    yalna diamou yague

  • @damegaye3851
    @damegaye3851 5 лет назад

    Machallah wakh dji raffetna lole

  • @lottagaye3980
    @lottagaye3980 5 лет назад

    Ma chalaalah amna solo xam xam dal dou ay thiakhne

  • @mbayediouf7119
    @mbayediouf7119 5 лет назад +1

    Ferimata 3 dom la amone (thiérno ferimata,Demba ferimata,ahmadou farimata) mè amoul ibre🙏

  • @dioprahmaneabdou7960
    @dioprahmaneabdou7960 5 лет назад

    Version yi barina wayé bi rek mo siyy deug kéndou serigne touba

  • @msquaretvsn
    @msquaretvsn 5 лет назад

    Mom mi yalna Yalla bindeul la yiw

  • @mamadouba8372
    @mamadouba8372 4 года назад

    Bonjour les torodos et tiedios la vérité divulgation total merci 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 les cherifs divulgation total merci 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊 🌊

  • @ngoudagueye4261
    @ngoudagueye4261 3 года назад

    CV
    AMZ

  • @moustaphandiaye6876
    @moustaphandiaye6876 3 года назад

    Yagi fénal mame maodo dé🥱🥱

    • @dameseye3039
      @dameseye3039 3 года назад

      Limou wakh daal raffet na machalah

  • @djibyseck8694
    @djibyseck8694 3 года назад

    Néna maodo mowakh serigne touba nimou nieuwé banimou démé mosoul togne boromam.té khamoul ni maodo mo diekeu faatou serigne ..doul bakhoul ndakh do am argument

  • @barryaliouabdalah7729
    @barryaliouabdalah7729 5 лет назад +2

    El hadji Malick Sy et Khadim Rassoul benn lañou

  • @ndouradiop3085
    @ndouradiop3085 5 лет назад +3

    Sam mboup loumou wakh rek khamnako serigne moustapha mola geuna diague fouf mom seutou serigne touba la ak mame maodo nopil

    • @originaldiouf7768
      @originaldiouf7768 5 лет назад

      Loubakh sou amoul iblisse dou am niou xamèko nonou nit bou nité souwété xamna boppam

  • @omarjueye
    @omarjueye 4 года назад

    Yalla nana SERIGNE TOUBA féyal bopam

  • @abdoufall1974
    @abdoufall1974 5 лет назад +1

    Ok

  • @malicksow4709
    @malicksow4709 Год назад

    Mais qui était le plus agé?

  • @ibrahimakhoule6875
    @ibrahimakhoule6875 4 года назад

    fanla ko diokhe wirde tidiane

  • @cissedjamil4549
    @cissedjamil4549 5 лет назад +2

    Damako deglou sama yaram daw billahi

  • @khalifendiaye6185
    @khalifendiaye6185 5 лет назад

    Li amena solo

  • @papesall9486
    @papesall9486 5 лет назад +3

    😍😍😍

  • @boubacarsow7793
    @boubacarsow7793 4 года назад +1

    Maodo Malick Sy mo makk khamo dara s.touba

  • @drameserigne2871
    @drameserigne2871 5 лет назад +1

    thiey Bichri

  • @hadjiratoudiallo1491
    @hadjiratoudiallo1491 5 лет назад +1

    Li nga wax rek mo am importance ..les deux Cheikh etaient d'une modestie inestimable ..naniou topp seni tank tei bayi yen kaddu yii..ndakh liga si wax lou niaw yaw yassi yakou mais dossi yakk darra

  • @ousmanendiaye7516
    @ousmanendiaye7516 3 года назад

    Ganne my kén dogue mouy sougne borom louffii nitt am ba diko damo molohmko djokh konn bougnou gnawo guir serigne

  • @ousmanendiaye3121
    @ousmanendiaye3121 3 года назад

    Fééne rék ngay def

  • @papembengue4708
    @papembengue4708 5 лет назад +2

    Xassida bi noume toudou

  • @mexdroid1703
    @mexdroid1703 4 года назад

    Boy déll wakh té yalla takh

  • @koneog3213
    @koneog3213 4 года назад

    Mais ki foumou diaguer machahala abdoulaye

  • @ibrahimadiakhate2698
    @ibrahimadiakhate2698 4 года назад

    YA MEUNE FENE MAME MAODO EST DÉCÉDÉ EN 1922 SERIGNE TOUBA 1927 NGUANI MAME MAODO DAFA SÉDÉ NÉ SERIGNE TOUBA DOUNDEUM YEUM MEUSSOUL AME BAKAR. YA MEUNE DOULE.... ITAKHOULA.

  • @moustaphandiaye6876
    @moustaphandiaye6876 4 года назад

    Liga wakh si bane téré la co Mame Moado wakh

  • @عليبابكرشك
    @عليبابكرشك 4 года назад

    Hééé saway toudou na maodo way