Jazbu HT 1997

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 27 дек 2024

Комментарии •

  • @noreyniucad
    @noreyniucad 6 лет назад +13

    ay way barké serigne touba weurnako ba soneu:: yalnala serigne bi faye

  • @aliounebadarafaye7859
    @aliounebadarafaye7859 Месяц назад +1

    Ndéye sane , Khadim Samb, au milieu entre Lamine Séye et Matar Diéne, diko nianal Aldiana Firdawsi 🤲🙏🤲.

  • @khadimdiop9110
    @khadimdiop9110 Месяц назад +1

    Ndeysann ❤️
    2024

  • @mouhamadoufalilouniang1197
    @mouhamadoufalilouniang1197 6 лет назад +11

    Ay waay MOURTADA AMAR Guddël te wer quel souvenir !!!

  • @khadimfallmachallah2281
    @khadimfallmachallah2281 5 лет назад +6

    Machallah s bi doufi diok dafiye sakh ba fawo mourode li nékh na loll

  • @diopmakhtar4323
    @diopmakhtar4323 5 лет назад +4

    Waw goor serigne mourda bii moye sama jeuzbou weurnako ay att

  • @baaxbaay2919
    @baaxbaay2919 2 года назад +2

    Ndeysaan Sëñ Xaadim Sámb Yalnako Yálla Yërëm Te Jëggelko Ci Barkeb Xasida Yi

    • @fatoumatasamb8497
      @fatoumatasamb8497 2 года назад +4

      Amine ya Rabbi. Dieureudieuf. Sama mak la 😭

    • @baaxbaay2919
      @baaxbaay2919 2 года назад

      @@fatoumatasamb8497 ah bon? ndaysaan man de sama xarit la woon lool Daara ji ma nekkoon daan fa jánge xam-xam ca Tuubaa madyaana sori wul ak kërëm waa-kuréel gi tamit foofu la ñu daan repetee Állarba Ju jot damafa daan dem dileen diglu ji ndaysaan mu nekk ku woyof te am ug taalube lool te fonk Sëriñ bi ak xasida yi ak ndjaboot ug Sëriñ Tuubaa gi Man de saa yu mosaana dem ci boulangerie wam bi mu joxma mille fr ni ma áddiya la dumako fátte mukk ci áddina wallaahi 🙈

    • @aybindir-yp9vi
      @aybindir-yp9vi Год назад

      ​@@fatoumatasamb8497Ndeysane

    • @mamediarrasambe222
      @mamediarrasambe222 6 месяцев назад +2

      Amine yarabi
      Peace daddy 😭🙏🏾

    • @baaxbaay2919
      @baaxbaay2919 6 месяцев назад +1

      @@fatoumatasamb8497 ah bon ndaysaan sama wollare la woon lool këram gi nekk Madyaana daan naa fa dem lu Bari ndaysaan daan fa fekk soxnaam sa mu nekk ku baax yal na ko Yalla yërëm te sàmm njabootam gi

  • @mamadoundiaye9334
    @mamadoundiaye9334 3 года назад +3

    Référence

  • @walygueye3310
    @walygueye3310 6 лет назад +6

    waw goor Mourtada contane na trop té nak diaxalouma si yaw
    bayilma sa numero

    • @MourtadaAMAR
      @MourtadaAMAR  6 лет назад

      Diadieuff waly ziare nala, envoie moi un mail sur amar.mourtada.touba@gmail.com

  • @bayfalljallo
    @bayfalljallo 5 лет назад +6

    S. MOURTADA AMAR JEREJEF WAYY. NDIANGUE MI DEPUIS 2002 BA LEGUI MANGUI KOYY WEUR;
    YALLA NA NGA DADJECK TAWFEKHOU BOROM TOUBA CI DOLEY CHEIKHRAFALL

  • @papesouleymanediop8829
    @papesouleymanediop8829 6 лет назад +5

    Antouka yagui fattali thiosan

  • @ndongoamar105
    @ndongoamar105 2 года назад +1

    Sante Serigne Touba rk

  • @mamelamp6983
    @mamelamp6983 5 месяцев назад

    BOROM TOUBA dou moromu kennn ☝.

  • @ibrahimangom2828
    @ibrahimangom2828 4 года назад +2

    Thiey Ahmadou

  • @dakartuba3265
    @dakartuba3265 6 лет назад +6

    ndéysann

  • @salioufaye1131
    @salioufaye1131 2 года назад

    Machallah

  • @PAN-2023
    @PAN-2023 11 месяцев назад

    🙏