Meilleur moukhadimat de tous les temps deube par le trio lamine seye ,Souleymane fall, Ahmadou Mouride thioune de nourou daarayni sicap rue 10. pour moi ce kurel à été d'un très haut niveau jamais égalé jusqu'à nos jours. Séparation meunoul gnakk lepp Serigne bileu rek koussi nek demna yokk experiencam si beneen kurel batakh fim tollou kurel yeuppeuy diang Lou werr daanaka. Hakazaaa
Je me rappelle dans ma chambre d’université Gaston Berger en 2006 j’ai pleuré chaque jour Maintenant je suis en France et je l’écoute toujours. On veut l’écouter dans 50ans dans ce bas monde Inchallah Et fi Dianatoul firdawsi Dites Amiine 🙏🏾
En ce moment je suis aussi à l'université ! Et c'est exactement le même sentiment que j'ai quanf j'écoute Mafatihoul jinaan 2022 Baay Ablaye Niang Ooohhhh !😭😭😭😭😭😭 Lep si keemani Serigne bi rek😭😭😭🤲🤲
Diangu mi nèkh na lol wayè ki bindeu li nèkone si ay khat khat façon mètital bounè gniou dèf ko ko tèwoul mou bindeu lou nèkhè ni war nagnio khamnè nè dou yeufi nitt 😭
Ce xassida occupait tout mon temps de marche à ma classe de terminal de la maison à l'école ce qui fait je parcoeurise beaucoup de partie, c'est mon cri de coeur, yalna andak mom ba sama bamel inchalla
Le seul khassida qui me faisait pleurer en 2009 et me rappeler mon cher Père que firdawsi soit sa demeure! Aujourd'hui en 2023 je l'écoute encore Yalla nanou yalla fayaal serigne bi ak dieume yi diko yeukeuti
Ndeyssane chaque jour mouy geuneu nex Maashaallah 🙏❤️ tay le Mercredi 27 September 2023 tassé ak mawloud ( gammu) comme si tay lanko diangue Yallna Yalla faye leen way te yagal leen fi kusi meli seugn lamine séye, seugn Soulayman fall HTdkh, seugn Maxtar dienné HTdkh et temps de autres 🙏🥰❤️🌹🕊️😍✅
Amnasi bénn année koor bo khamni ak tole yi nimou mété mais damadann ngontou mais barké Serigne Saliou bambey FM dakada ték aussi ay 16h tellement que damasi concentrer badamay faté métitou koorgui
Moukhadimate dotoul nekh sama nop ba raw bi❤ 2012 ba fimné meuneutuma deglou bénéne Moukhadimate té batay missoumako❤❤ yalnagnu YALLAH fayal Serigne Touba
Walahi lii gueuna nehh ci Ndjangg mi mooyy Araff yi dafa lerr naaandj dangay degg lou lerr tei werr, lou jaffé ci kourel yi legui. Yalla na soun borom faye len
Ndeysane mouxadimat bii Nîme Maye déff yalla rékk mooko xame Macha Allah yalna yalla barkeel léene néekhna trop Wallàhi 2006 ba téye saa booko dégloo daye mélni Lou béess Keene d'où Serigne TOUBA 😢😢
Ndaysann je me rappelle fadiar lako radio bambey da ték bobou magui mbarassane damay nék si kaw lal sama mère diapou ko mais bly momay yé avec plaisir inexplicable yalla na lénn sounou borom fay mann Lamine Seye mako beugual sama bobou réck barké Serigne Saliou
Meilleur moukhadimat de tous les temps deube par le trio lamine seye ,Souleymane fall, Ahmadou Mouride thioune de nourou daarayni sicap rue 10. pour moi ce kurel à été d'un très haut niveau jamais égalé jusqu'à nos jours. Séparation meunoul gnakk lepp Serigne bileu rek koussi nek demna yokk experiencam si beneen kurel batakh fim tollou kurel yeuppeuy diang Lou werr daanaka. Hakazaaa
Et jokhani
@@thiamaly2207 biss bobou diokhane gneuwoul wone enregistrement lawone.
ndaysaane
😍😍😍😍😍👌🏾
Bilay Li dafa yemé trop 🥺♥️
Meilleur Moukhaddimat du siècle 😍 Dieureudieuf Cheikhoul Khadim
Wallahi
WOORNA
Wér na
Bilahi waxatiko
billahi wakh ko si kaw kénneu doula wéddi
Je me rappelle dans ma chambre d’université Gaston Berger en 2006 j’ai pleuré chaque jour
Maintenant je suis en France et je l’écoute toujours.
On veut l’écouter dans 50ans dans ce bas monde Inchallah
Et fi Dianatoul firdawsi
Dites Amiine 🙏🏾
😭😭😭😭
En ce moment je suis aussi à l'université ! Et c'est exactement le même sentiment que j'ai quanf j'écoute Mafatihoul jinaan 2022 Baay Ablaye Niang
Ooohhhh !😭😭😭😭😭😭
Lep si keemani Serigne bi rek😭😭😭🤲🤲
Ammeen ❤❤
Diangu mi nèkh na lol wayè ki bindeu li nèkone si ay khat khat façon mètital bounè gniou dèf ko ko tèwoul mou bindeu lou nèkhè ni war nagnio khamnè nè dou yeufi nitt 😭
Ndeyssan souma djoumoul magal bii laléene geudia sétane darou khodouss ak lamine seye. Bou djouli fadiar diouté pour foumouy djaar probléme la gniéppou bag kou laal.matar djéne di khal yone bi ndeyssan ❤️❤️❤️
Moukhadamatt bi douma ci doyal depuis des années makoy deuklou chaque fois day melni tay lakoy soga deuklou sama khol bi sedd gouyy
Machallah
Ce xassida occupait tout mon temps de marche à ma classe de terminal de la maison à l'école ce qui fait je parcoeurise beaucoup de partie, c'est mon cri de coeur, yalna andak mom ba sama bamel inchalla
Le seul khassida qui me faisait pleurer en 2009 et me rappeler mon cher Père que firdawsi soit sa demeure!
Aujourd'hui en 2023 je l'écoute encore
Yalla nanou yalla fayaal serigne bi ak dieume yi diko yeukeuti
Amine yalla nako yalla yereum té xaréko aldjiana firdawsii thi barké xassida yii 🙏🙏🙏🙏🙏
Ndeyssan lamine ak souleymane fall ak diokhané liignou deubé thi magal 2006 dotoufi am🙏🏿 Maguikoy fatalikou nii guoudik magal 2006 machalah 🙏🏿🙏🏿
Wallahi mbokou mi ❤️
Deysane ça me rappel les années 2009 à 2012 quand on faisait le ziar à Seugn Mountakha yalneu fi yague tei weir❤❤❤❤
Ndeyssane chaque jour mouy geuneu nex Maashaallah 🙏❤️ tay le Mercredi 27 September 2023 tassé ak mawloud ( gammu) comme si tay lanko diangue Yallna Yalla faye leen way te yagal leen fi kusi meli seugn lamine séye, seugn Soulayman fall HTdkh, seugn Maxtar dienné HTdkh et temps de autres 🙏🥰❤️🌹🕊️😍✅
Le 27 septembre 2023 on l’écoute encor❤️😭
ére bi motakh may kourel ndeysan moma motivé mom ak midadi baye youssou ndaw HT nexna
Lamine seye infatigable yalna yalla fayko
On l'écouter à lamp fall FM Chak 2h du matin dafma dan diaral baña nelaw thiey Serigne bi 😭
Aujourd'hui c'est le décé de Serigne atou ndiagne yalla nako yalla kharé aldiana
ma challa nékh na lolou fimou may yobou yalla rék moko kham
Des frissons extras a en plus finir. 🤩🤩 !!!! Tieuy SERIGNE TOUBA , wahlein Dieureudjeufatyy Serign Touba. Ken dou mom wayyyy
AMOUL MOROM KEEN LA YALNANIOU KO YALLA DOLLI FAYAL AMINE.
Amnasi bénn année koor bo khamni ak tole yi nimou mété mais damadann ngontou mais barké Serigne Saliou bambey FM dakada ték aussi ay 16h tellement que damasi concentrer badamay faté métitou koorgui
Moukhadimate dotoul nekh sama nop ba raw bi❤ 2012 ba fimné meuneutuma deglou bénéne Moukhadimate té batay missoumako❤❤ yalnagnu YALLAH fayal Serigne Touba
Wallahi,wallahi wallahi lii nimou may df meunou mako wakh
diangue bou mélni mom dotoufi amm tiey 😭
Meilleur jàng de tous les temps, indétronable. Dagnouci warone decorer gnom S. Lamine Seye, li meunatougnouko ❤❤❤❤❤
Li li li li♥️♥️Adjana koudoul boudoul diékhhh Walahi
Ohhh ndaysane lamine seye ak diokhanè souma sagnone dolen meussa takaliko😓😓
Ndeye Hélène linga waxe sikouwoul deh Dathe bi benla dotoul amati
😍MOUKHADIMAT DU SIÈCLE 😍
Ndeysane dajj bi nimoumay Def Ahmadou rekk moko xame 😭😭😭
Dieureudieufé Chiekhoul Xadime
Xidematoul Xadime kep lamine seye ngir yalla gneuwatal darou khoudoss ngir yalla
Ohhh ndaysane lolou bepp mouride dineu ci begu .nguir yalla lamine niongui lay niane nga dellou darou khoudose defal ko mbokou talibè yii cii barkè ahmadou😓😓
Bilahi 😭😭
Thieye serigne touba
Nekhoul bâ nekhoul SERIGNE touba keep môme rek amoul kenene lli adiana la Bamba gracias Bamba obrigado
Ce moukhadimate me rappelle ma sœur nogaye ki aimait écouter cette xassida .yalna sen diamm yague
MEILLEUR MOUHADIMAT DE TOUT LES TEMPS
Je confirme ❤❤❤
Thiey lamine seye htdkh nam nanla
Ndeysan, yalna sa borom seral seni xol niki guèn seralé sounou yoss
Dathi de tout le temps bilahi 😢😢😢😢
Ndeyessane kourel bi dotoul ame ba faw moukhadimat bi bene la
Billahi yalla lako takha wakh dh domou nday Man dh nim may déf😢
Mfaty Mbacké bilahi jewrine Sene diangue rek la meuna deglou lamine benene affaire la
Waxleen nimniouy def
@@mfatymbacke1073 kémane la domou ndeye bilahi
Ndeysane dajj bi nimoumay Def Ahmadou rekk moko xame
Dieureudieufé Chiekhoul Xadime
Nimay yeugué dadjou Serigne Saliou Thiam bi Macha alla. Nidiaye Souleymane Macha alla
Machallah yallah sounou weureul baat yii yokou xeweul gui si barkè cheikhoul khadim
damay fatali lou bari ay atte thi guinaw souma amèe louma mèti souma dèglo rèk guife❤❤❤
ndeysaan
Batay manumaa muññ daajj bii
Ça me rappelle un de mes grands frères qui est parti très tôt yàlla na ko yàlla yeuram mok bepp dioullite boufi bayyi ko kepp kouy doundou😭
Amine barké khassaides yi
Septembre 2024 toujours le mythique Moukhadimat de Darou Khoudoss.
16 juillet 2022, 16ans après et je peux dire que Moukhadimat yémé neu torop torop torop
Walahi lii gueuna nehh ci Ndjangg mi mooyy Araff yi dafa lerr naaandj dangay degg lou lerr tei werr, lou jaffé ci kourel yi legui. Yalla na soun borom faye len
Dafa am lumay fataly😭😭😭❤❤❤😭😭😭😭😭
Manchala 😢😢😢doumassi massa doyal
Wallahi hazim sou adojna dékki wonn saax sa restera le meilleur 😭😭😭😭😭😭❤
moukhaddimaat bi doumassa sappi nn machallah
Douma thi massa doyal li aldiana la Lamine Seye ❤❤ 2023 comme tay lanou ko diague
Naniou Di sant Serigne Touba founu tol Ken du Serigne Touba budul won ak momm finu dieum
Ndeysane yalla naléne Serigne Touba Faye
Muhadimmatoul amdah 2006 vraiment c'est une tuerie !!!
Machala nex na trop yala nan dadjek geuramaml s touba amine
Ay waay ila khayrina bi lamine seye dathie dougalko
ndeysna lii damay dioylo billahi aka man nima dioy diafé
Yalla nalene serigne touba fayal bopam
Ndeysane mouxadimat bii Nîme Maye déff yalla rékk mooko xame Macha Allah yalna yalla barkeel léene néekhna trop Wallàhi 2006 ba téye saa booko dégloo daye mélni Lou béess Keene d'où Serigne TOUBA 😢😢
2023 qui est là? 🥰❤❤❤❤🥰
Le meilleur de tous pour mane li l’ennen lh😭
Patrimoine culturel de l humanité
Quel chef d'oeuvre !!
Macha Allah Moukhadimatt Bi Yéména Deh Barkep S Bamba Kawena Lol Yalnalène Yalla Same
Billahi douma si doyall ♥️♥️😭
Paradis sur terre😭
Walaye ndeysane 💓
Akassa! Diadieuf mourid. Vidéo bi ça fait très longtemps que je le cherchais
Le moukhadimat de tous les temps blh✨🥰😅
Bii dotoufi am ndeysane machalah
2023 toujours là 🥹❤️
Ndayssan aka nex khassida mo sedd xol dieurudieuff serigne touba
2021 toujours les memes sensations toujours les memes frissons !!!!
Moukhadimat de tous les temps 🤌🏾❤️
Ndeysane❤❤❤❤
Mon coup de cœur ❤️🙏🏾Jeureujeuf Cheikhoul khadim
Notre aire moukhaddimat kéna masoul guiss lou mel ni serigne touba dal amoul morome dieureudieufati serigne touba amoul mrm
thiey yalla ahmadou moo dooy kemane
En l'écoutent tout mon corps reste immobile il rentre directement dans mon coeur 😭
Même en 2022 c’est on l’écoute toujours air bi dafa aljana wé ❣️❣️❣️😭😭
Le meilleur mawahibou de tout les temps j’aime lamine Seye
Mouhadimat
Serigne Touba amoul morom. Lii nekhna lolll
Macha Allah çëy Serigne Touba kénn khamul lumu doon
Nonnn dadj bii dotoul amatii abadannnn thieyyyy lamine seye
macha allah khol séd na trop
Qui l'ecoute tjrs en 2022 tiey bii daadj 😭😭😭😭😭
Diadeuf Serigne Touba Macha alah
Yalna niou le yalla fayal
Quel Moukhaddimat!😍😍😍😍
Tout simplement inexplicable
Serigne Mourtada deubé bi dafa melni Ahmadou Thioune sila bokkoon
lol dakkor magui koy update inchallah
@@MourtadaAMAR waaw goor mouride saadix
Diarama biii bene la fiii thi adouna
Manotou bou mel niii
@@alysarr1178Après l'avoir enregistré ce dimanche là, japou niou wone ni diang mi ni lay mél ndeysane. Diko santé Kou Ted ki ndax lép moom la
@@MourtadaAMAR jajeuf
Serigne Touba amoul morom de
Walaye ndeysane nexna lol
Mouhadimat du siècle
Dadj bi douma si doyal wallahi li nekhna
Masha allah sama khôl sed na
Allahou akbar lii doyna waar
Best Mawahibou ever🥹❤️❤️😭😭
Thiey li kouni nèkhoul si khol do dioulite
Ndayessane HTDKH a❤❤❤❤
La version mp3 ngir Serigne Touba
Ndaysann je me rappelle fadiar lako radio bambey da ték bobou magui mbarassane damay nék si kaw lal sama mère diapou ko mais bly momay yé avec plaisir inexplicable yalla na lénn sounou borom fay mann Lamine Seye mako beugual sama bobou réck barké Serigne Saliou
Lamine seye ndeye san nekh na
Khassida yi rekk
Du ma ci masa doyal 😭😭here NYC 23/10/2022/3:01/Am
Tiey 🤩🤩🤩 dieuredieufé serigne touba
Lamine séye ak souleymane fall ah machallah nekh na lolou
Serigne touba Gueye ak Ahmadou Thioune ils étaient les 3 à diriger ce jour là
C est le meilleure vraiment❤🥇yalna sante yag