Ohhh Assane Ndiaye merci pour la reprise c top❤ j’adore cette chanson je l’écoute pratiquement tous les jours en boucle wayei dafay toyal sama khol😢 Repose en paix papa Thione🙏🕊
Je suis très contant de la reprise, le décore est extraordinaire, les images de très bonne qualité. Il y'a un mais la dame solo qui danse est trop sexy. Si c'est en hommage à Papa Thione donc c'est une ERREUR Merci
Ohlalaaaa son bi sama dome Bb mouhamed momako ngeuna beugue Deysane nekhna waay Papou fallou Benjamin Ndiaye ak mbaye sy Ndiaye mou raam daan laniouye waaye wa benj Family diaspora ani ngenn mci assane Ndiaye
Grand Assane, vous répétez tout le temps : « Thione mo ma yar ». Cela se voit clairement. Thione est l’artiste africain le plus talentueux que je connaisse.
Les danseurs sont très professionnel ils dansent hyper bien ça fait très longtemps que j'ai pas vu une performance aussi bien fait waouh chapeau tout t ok sur le clip
féthie kate yi souma amone khaliss may léne ko vraiment ligniy féthie raféte na yiw na clip bi aussi mérite des millions de vu souma mounone aimé 1million de fois défko merci beaucoup assane pour cette belle reprise
Assane Ndiaye sons bii nekh na trop mais amna Lo bayii si sons bii 😅bilay wayy katt yii war guene fonkou momo Dieng demlén deglou bou Momo dieng ak bi comme yalla ak yalii 😂momo tu es le meilleur
En écoutant cette chanson j'ai la chair de poule je me rappelle les bons moments où j'allais à kili c'est vraiment émouvant paix a ton papa thione que firdaws soit ta dernière demeure amine
J adore la belle realisation chorègraphique diadieuf mon frère souleymane sidibè ainsi que les autres danseurs
Akka meuneu waye ki manchalla kou d'accord ❤👍👍👍👍
Mo dakha woy senegal sama baat thi kaw
Ndama ndiaye mame nogaye
Souniou pape da meun❤❤❤❤
@@ndiemeniass2030 cest le meilleur borom sahel
Wali
Cc too I'll Ii ki I'll😊nkk kk kikm😊ñ 😊 mm mm in j MMO ko mm mom mmnkk kk mom k@@ndiemeniass2030
Dama contane Ndiaye diatta Ndiaye fans yi amougnousa Faye ❤️❤️ meilleur chanteur du monde❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ligua remix Assane nékhe na tropp wayé tame khalé yii lignou la fétiale reféte na lii eupe waye ( esplanade grand théâtre lagnouye kharee )
Machallah papa Thione yalla nako yalla yeurem kharéko aldiana firdawsi 😭🙏
Ndeyssane papa thione yalla nako yalla yeureum khereko aldjana firdawsi 😢
Amine🙏🙏
Il chante trop bien machallah
nianenio ma fi djiitou nii dèja
yènii tam en tant k premier fan du meilleur chanteur de notre pays
togn nguèn ma 😀😀😀
Machalla❤ trop nekh papa Assane papa Thione 😢Repose en paix yalla nala yalla yereme namenala dé papa Thione💔😭😭
Wallakhi name naniouko lolll😢
Quand est-ce que je vais arrêter de pleurer pape Thione yalna aldiana donn sa keur Ballago 😭😭 Merci père Assane😊
Jamais papa thione si khole yi
@@maimounathiam2748 wallay suniou xol yi la neikk😍
On ne sais même pas, que le tout puissant l'accueil dans son paradis éternel amine y'a rabbi dèpuis la mauritanie
Heure bo guené geune Ndiaye Diatta on t'aime de tt nos cœurs Assane
Yalla nala yalla may goudou fane ak were rek machalla nékhna trop ❤❤
Wa mais kou contane si danseurs yi lii nekhna way 😍😍😍
❤❤❤❤
Goor momoul leumbeul
Na goré
Groupe bi mom ils ont bien assuré
Wollah surtout groupe bi machallah❤️❤️❤️❤️❤️🫡
Clip bi douma ci doyal.je l'écoute tout les jours
Wa nioro du rip am guén ndam❤ fiers d'être Saloum Saloum 🎉❤
Ay way yaw sama mokouga
Nioro Mach alah
Nioguini dé 😃 bilay
Ohhh Assane Ndiaye merci pour la reprise c top❤ j’adore cette chanson je l’écoute pratiquement tous les jours en boucle wayei dafay toyal sama khol😢
Repose en paix papa Thione🙏🕊
❤❤
Momal daal ni ndeyssan
@@abythiam6889 ndeyssane thione Dafa meunone binde machalah
l'hôpitalde kxtggvmi😂
Sénégal namone nala nak papa ❤🎉
🎉 assane Ndiaye damala yageu beug ms rawna tay bagua wakhé wa nioro ohh ❤❤ père assane 🥰 on t'aime
Machallah tre jolie reprise ❤️❤️ les danseurs aussi ont assumés El mbaye ndeyssane lou yague deugeule 🙏🙏🙏
Bilayyy weuy bi sama xool laay seed😭❤️❤️❤️❤️❤️
Yalla nako yalla yeureum thi barké sopem ba naby psl
Je suis très contant de la reprise, le décore est extraordinaire, les images de très bonne qualité. Il y'a un mais la dame solo qui danse est trop sexy. Si c'est en hommage à Papa Thione donc c'est une ERREUR
Merci
Cette chanson me fait toujours pleuré 😢merci Assane de lavoir repris 🎉
Aaye sama fans bii keine dou yaw Ndiaye heure bouma yèwo dila geuneu beug... senegal yafi dakha waaye ak waly seck
Machalla je la regarde plus de 10fois dans la journée vraiment c’est trop nekh ❤
Ohlalaaaa son bi sama dome Bb mouhamed momako ngeuna beugue
Deysane nekhna waay
Papou fallou Benjamin Ndiaye ak mbaye sy Ndiaye mou raam daan laniouye waaye wa benj Family diaspora ani ngenn mci assane Ndiaye
Thione seck yalna hipé aldiana à bep dioulite Amin 🙏
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🔥🔥
Aye waye moumaye déf ba guisse assane N’diaye ki rek la begue ak Coumba guawlo machalla Dafa meilleur ❤
Grand Assane, vous répétez tout le temps : « Thione mo ma yar ». Cela se voit clairement. Thione est l’artiste africain le plus talentueux que je connaisse.
Maash'Allah💯çà se voit que l'héritage de Papa THIONE est bien assuré👏♥️😍
Merci assane pour ce beau témoignage repose en paix Papa Thione
Wakhhh dégue yalla reprise dawnAa yarammm ❤️
Nékha trop les danseurs vous êtes formidables ❤
Machalla Sama chanteur préféré kén dou yaw longue vie❤❤
Ndanaan piiir ngi nii😊
Les danseurs sont très professionnel ils dansent hyper bien ça fait très longtemps que j'ai pas vu une performance aussi bien fait waouh chapeau tout t ok sur le clip
Khana oscar des vacances guén diar❤❤❤❤❤❤
@@mamafatoulo3657😅😅 2:38 2:40
Waouh les danseurs sont exceptionnels ❤😢🎉 et la reprise me fond le cœur rest in peace papa thione😭♥️🕊️
Mon papa d’amour machalla contenaaaa xol sed goudou fane ak werrr Ndiaye Diatta ❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭😭😭🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Eupeuna na Ndiaye Assane kayé roy dou nirou ak piirr kéne thione nako yalla yeureum❤️❤️❤️🤍🤍🤍
😢😢😢😢machalla li nekhna way papa thione yalla na aldjiana di keureim🙏🙏❤❤❤❤❤
Makhiii dolii watttt li tamit nexxx neuh trop🎉🎉🎉🎉🎉 les danseurs la qualité de l'image c'est du ouffff béguenahh dé
Hommage à papa thione tu resteras tjrs gravé dan ns cœur ❤️ ❤️
Amine ❤️🙏
Bravo aux danseurs et longue vie a Notre papa Assane ndiaye pour la reprise du song ❤
Linga wayate sama papa ak mane reuyna simane yalla nala yalla faye bate bi wer
Macha alla sama fan's bi lo guéné mou nékh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ah benjamin iow ak mbaye si ndiaye lo lenn di df si son bi assane way na seen bay dh
Qui est d’accord que Momo Dieng seul a réussi cet belle chanson de Feu. A son Ame Ballago 🙏🙏🙏
Bosou momo mo dak
Bilay
Momo bossam mogueun neh gueunn dal aussi❤
Macha Allah sama papa dji ndiaye diatta yallah n'a fane wi guoudou amine waye wi nekhe na
Belie walie ko koi jemm ak kou meunn dunj Bena Assan is a professional international musician.. good and quality music RESPECT
Macha allah laf thiate assane.ndiaye , Ppa Thione.lamaye fateli yallana khipe aldiana firdawssi mako beugue
Papa thione ken doula faté si aduna 😢yalla nala yalla xaré aldiana 😭🙏
Faramareen b woy rek lie deff❤❤🎉greetings from the Gambia 🇬🇲
Nice Clip ! Chapeau à Raf’Prod 🫶🏾
Lima geun nekh thi mom moy yarr walay❤
Bilae Ndiaye diatta papa thione rek lay holé yalla n'a yalla goudal sa fane papa thione yalla nako yalla yeureum
Des❤❤❤❤❤❤❤❤ pour ces danseurs rafeet na... yiw na.... chapeau❤❤
Après Thione c est le meilleur chanteur parmis les frères
Nékhna trop wayyé kéndou momo dieng tamite ❤❤
Hooh la qualité d’image machalla raf prod vraiment vous fait un très bon travail
C’est quel groupe ils ont assuré la chorégraphie chapeau ❤
Reprise bi nehna , danseurs yi aussi Mancha allah.Repose en paix papa Thione
Fëcc mii civilisé n'a Gooré n'a ❤❤❤
Félicitations ❤papa thione yalla nako borombi yeurem te khare aldiana firdawsi
féthie kate yi souma amone khaliss may léne ko vraiment ligniy féthie raféte na yiw na
clip bi aussi mérite des millions de vu souma mounone aimé 1million de fois défko
merci beaucoup assane pour cette belle reprise
Pape thione Seck ak pape mass Ndiaye yalla nallén yalla yeureum si barké seydina mouhamed psl
Amine
Assane Ndiaye sons bii nekh na trop mais amna Lo bayii si sons bii 😅bilay wayy katt yii war guene fonkou momo Dieng demlén deglou bou Momo dieng ak bi comme yalla ak yalii 😂momo tu es le meilleur
Très belle chanson ❤❤
Ce son me fait toujours tant d’effet 😊😊😊😊 merci Assane reprise bi dale na Macha'Allah
Nekhna ohhh MachaAllah🥰 mention spéciale aux danseurs!👌🏾❤️
raf prod vraiment vous du très bonne travail qualité d'image excellent
Li Ndeye Wade rekkh sama xaritt bi la khoyyy mayyy
Oh la chorégraphie ma plus retenue que la chanson elle même ❤❤❤❤
Comme moi ma Cherie surtout avec pudeur
Groupe de danse le gars devant kou kham noumou toudou svp😂 néko suis fan d lui
Srx groupe bi meune nagnou danser 🕺 ❤gnom Gno defone clip Pape Diouf bi
Le meilleur chanteur vraiment on t’aime Assane ❤
🤗Vraiment la chorégraphie est magnifique
Wadji si kanam, il danse super bien
Mo radiakhé superman love de pape diouf 🥰🥰🥰 nekhna lol
Wollahi nak niom rk ladone setane franchement meune nagne trop tè civilisé ❤️🙏🏾😊
En écoutant cette chanson j'ai la chair de poule je me rappelle les bons moments où j'allais à kili c'est vraiment émouvant paix a ton papa thione que firdaws soit ta dernière demeure amine
Et merci beaucoup grand assane tu nous fais revivre les bons moments avec papa thione grand longue vie
Mashallah les danses danses super bien❤❤❤
Nimako beugue sama pape dji Ndiaye diatta contane nagnou machalla ❤❤❤❤
Quelle flexibilité des danseurs!!!!... très beau clip ❤❤❤
Worna kouy mayei nekhna rafetna
Kou beug série bi rék lalale j' aime ♥️
Macha alla sama papounet lo def mou nekh bonne continuation on t aime fort
Mane ma bague famille thione seck billah c'est mon chanteur jusqu'à présent écoute le grand paroliers mon préféré à dieu machalla assane ndiaye
Oh Machallah li Rék ladone dioye merci Assane kene dou thione Seck qu il repose en paix 😢
Souma la déguelo comme si que magui déguelo pp thione dangako beugue rék té yalla takh yalla nako yalla yokk lérr té yagual lafi inchallah ❤️❤️🥰
Un très bel hommage à son très cher frère. Mémoire amplement respectée
Danseurs yi dougn nit❤laa toupathia
Chaque samedi mbaye Dia en face police 4em soirée assane Ndiaye dara dakouko
Souniou keur kou diourék mome rék ngégue dégue lou machallah notre chanteur🎤 préfère
L un des pionniers de la musique senegalaise
Clip bi simple na raféte na way bi nékhna trop je suis trop content wayyy 🥰🥰❤️❤️
Woow. Bravo ça c’est du qualité
Très beau clip machallah 😊
Ndeysane comme thione Seck k dieu lui accueil ds le paradiso
Je reprends toujours cette chanson 😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
Ohhh le retour de notre assane national longue vie á toi machallah magnifique son ❤️❤️❤️❤️
En tt cas la vidéo est trop trop top👍🏽👍🏽👍🏽👍🏽la chanson n’en parlons mm pas😍😍😍😍
Félicitations assane toujours égal à lui-même
J’aime les productions de Rafpro ndeyssane j’estime beaucoup Clara gueye.
Assane N’Diaye félicitations
Kou khame fou mangou ndiaye nekk ?? 😅
Dieureudieuffattiii way , notres ténor de la chanson SÉNÉGALAISE , ngathié ngalama , Elhadji ASSANE NDIAYE . Yallah nala Yallah lafal thiat 🤲 👍🙏📿🕌📿🤲 💖🌹🇸🇳🥰❤️💖🥳👏👏👏👏👏
Mashallah 🥰 Papa Assane la voix du Rossignol love you🥰🥰🥰❤️❤️❤️
Premier Commentaire Toujours Là Depuis ALAL Merci Grand Assane Et RafProf Pour Ce Retouy🇸🇳
Une belle chanson les danseurs au top
Comment s'appelle la fille en blanc elle danse super bien Machalah