*Corruption bobou Balla Gaye ak Gris wakh negn ko. Balla a fait pire, il a traité le CNG de VOLEURS. En plus niou convoquer ko mou benia dem. Teh pourtant on ne l’a pas suspendu. Pourquoi? Parce que mbeur bou makk leu? C’est une injustice totale envers Amanekh! S’il vous a accusé de corrompus, porter leine ko plainte pour diffamation mou indi ay preuves. Lolou moy yone.*
Kandji ne te fou pas de nous ... amanekh a raison cng bi ay corrompus laniou .. lobby aziz ndiaye mo nek cng.. malick ngom a été placé par aziz ndiaye...
Bonne continuation Kandji et le Cng,vous avez une mission difficile car assainir un milieu comme la lutte est presque impossible car les analphabètes y sont majoritaires tè sen beug beug rek laniou kham,un règlement doit être respecter et toute faute sanctionnée aussi malheureusement Sénégal dafa metti
Kandji on sait tous que tu es un porte paroles mais les textes , les règlements, , ont applicables chez tous les lutteurs en activité.. Moi , m'interroge sur la non sanction de Balla Gaye 2 quand il a traité ouvertement et publiquement le CNG et Voleur, et la non présence de sa convocation... Soyez justes et équitables chez tous les lutteurs....
GNG bi ak bifi nekone kif kif 🤷🏽♂️6-9 😂😂😄😁😂😂diaye dole rek bataye 😢😢😢courage ama nékhe legui makane noumiy def combat wame 4 Avril 🤷🏽♂️ niang bou ndaw vs ama nékhe
Je ne suis pas un amateur de Lutte pour ficeler des combats comme peuvent le faire certains, mais je connais la lutte. Pour dire la vérité, Thiatou Daouda Fall a battu Amanekh. Si vous regardez bien les images, Amanekh a été le premier à toucher le sol, épaule et même sa tête, avant même d'appuyer la tête de Thiatou Daouda Fall. Sénégal dougnou wakh deugeu. Bravo le CNG et Kandji
Bilahi yaw Kendji CNG bi amone nasi Yakar pour ni degue dinafa âme mai victoire pour thiatou Daouda fall gisouma louko mana dégueul té amanékh limousin wakh degue la
Amanekh daffa war khamni CNg règlement youmou tek Si texte bi lagnou soukandikou pour diokh Thiate victoire bi Et quoi qu'on puisse dire waroul wakh CNg dagnouy fen
Père thioune bamou néké Si lamb ba légui mogui sogua dioum si sama yakar meunon nguén ko avertir rek bagn ko sanctionné vue que sen biir la book dafa dioum tée niit kassé laa
Ama nékh doit se faire accompagner et attaquer la décision du CNG au niveau du tribunal administratif. Le CNG est juridiquement en tort dans cette affaire
Js daccord que amanekh waroulen taxe de corruption mes da meron meunon guenko def susrsi ak amende balla gaye a fait fire teksi guen convoque ko mou bagn que cest tre grave
Amanekh de tout cœur avec toi
Félicitations encore ama nékhe yadane taye dane souba ✅merci lamine Séck linga def moy ligueye
Merci kandji kaddu yi lerna Machalla bonne continuation chapeau 👒 ❤
Bilahi ama nekh dane ko togne
Vive amanekh ❤ ❤❤❤
Bilahi Togne nguène Amanekh diayko dolé😢
mai lane motakhe amanekh amoule avertissement o lieu de suspension c’est du n’importe quoi
Félicitations Amanekh
CNG nekko lenn thii deugg dehh. Le cas Amenekh môme vrai injustice laaa.
Cng legui bi dh Albourakh rek leu neikal fi. Amanekh deffoul dara. Ama ak Franc gueine wara suspendre mais vous le ferez pas pask Albourakh moy dawal
*Corruption bobou Balla Gaye ak Gris wakh negn ko. Balla a fait pire, il a traité le CNG de VOLEURS. En plus niou convoquer ko mou benia dem. Teh pourtant on ne l’a pas suspendu. Pourquoi? Parce que mbeur bou makk leu? C’est une injustice totale envers Amanekh! S’il vous a accusé de corrompus, porter leine ko plainte pour diffamation mou indi ay preuves. Lolou moy yone.*
GNIFA NÉKONE DOU GNI MOTAX SUSPRENDRE NOUKO Bayi si xél
@@Zam-Zam710President bi rek mo changer ak quelques personnes. Mais commission de discipline bi presque gni fey nekone niofa nekat beu legui.
@@Zam-Zam710etat continue tela lolou doussi dara affaire de discrimination deug la
@gazza873 yaw xana guisou ni niom binou nieuwé nieup lanou Baal grâce tamite
@kurayahmi niom nieup lanou grâce binou nieuwé nak sén Bax
Cas amanekh dou deugg dou yoneu pkoi guéneu koyy athieu 6 mois.
Bilahi kandj kayy nanfekh deug aziz nd loumi wout cng mome yorna businessam té Sénégal am gniouko gueuneu done compétent sportive té ken dieuloulen
Lamine un vrai pro mashalla
C'est ça un professionnel
Lamine machalla tu es très fort tu pose des questions ❓️ très pertinente 🎉 chapeau à toi
amanekh mon dann way
Merci lamine
Kandji ne te fou pas de nous ... amanekh a raison cng bi ay corrompus laniou .. lobby aziz ndiaye mo nek cng.. malick ngom a été placé par aziz ndiaye...
Setal yallah si touma yinguay tekk si kaw nitt ki
Lamine mii il fait 1 travail tres pro....et da tèy c demandes importantes am sens...
En tout cas il est très pertinent. Explication yi lerna dh manchallah
Tres pertinent kandji depui. Alioune Sarr li amoul wone. Lep lerna mm Amateur bi soula setane dina kham les règlements machalaa
Thiakhane bakholle amanèkh moudane bodoune balla gaye ak bouye ngia do dème ni bayilène aye Thiakhane
Champions quen douka force delen yemele boy yiguen outal yonn bouñ len dane guen nagul bayi parpalo bi
Effectivement Demb bima deguei iba kane lolou done xalat il faut mbeur bi Diot affaire yi avt gniou koy oubli bravo Kandji une bonne communication
Bonne continuation Kandji et le Cng,vous avez une mission difficile car assainir un milieu comme la lutte est presque impossible car les analphabètes y sont majoritaires tè sen beug beug rek laniou kham,un règlement doit être respecter et toute faute sanctionnée aussi malheureusement Sénégal dafa metti
CNG laniou wara suspendre
On attend de voir si vous sanctionner ama balde
Niii ay nafekh lagniou rek amoul bene wa rufisque bou nek si lamb jii ay corrupteur guene yene gniape lamb guene di yakh rek domram
Balla Gaye wakh na Wa CNG sathie lagne tè dara fè couko sii😢😢😢
Va appeler biram sene pour lui demander 😂
Machalah ❤
De son fonction kay 😂😂😂😂
😂 adioull loolou
Kandji on sait tous que tu es un porte paroles mais les textes , les règlements, , ont applicables chez tous les lutteurs en activité.. Moi , m'interroge sur la non sanction de Balla Gaye 2 quand il a traité ouvertement et publiquement le CNG et Voleur, et la non présence de sa convocation... Soyez justes et équitables chez tous les lutteurs....
Dieureudieuf kandji lambe mo beurii niou diangoul beu paré beurii wakh
Félicitation amanekh ya dane dagne la togn
GNG bi ak bifi nekone kif kif 🤷🏽♂️6-9 😂😂😄😁😂😂diaye dole rek bataye 😢😢😢courage ama nékhe legui makane noumiy def combat wame 4 Avril 🤷🏽♂️ niang bou ndaw vs ama nékhe
Dafa rew motah😂😂😂
Sa wax j téguéwoul fenn aziz nd waroul neck membre cng da guéna complexe rek,amanekh mo dane
Ont vs attend sur le ga franc ama on a lue le règlement
Thiatou daouda fall dane gua si aye keuyite nak mais gnoune gniy doundou lamb amo ndam nala lerr ́nagne
Boul wakh gnoune nel yaw
Gnoune la
Limou wakh deug la
Amanekh Mo dane
Mbok say néklén nit lamb ji dafa aw yone
T’as raison amanekh mo dane
Nél amoul ndam si yow nay lerr
CNG bou béss bi Guédiawaye la toudou, Sant Pikine... Yénéne gokh yi amougnou bras long
Vèrema tonguène amanèhe 😢😢
Kandil doumiharam rek
Jubb juballl jubantiii merci kandji
Loutakh niom djitouw niousi, amanekh di dougal recour niouniko dougafi dougal
Je ne suis pas un amateur de Lutte pour ficeler des combats comme peuvent le faire certains, mais je connais la lutte.
Pour dire la vérité, Thiatou Daouda Fall a battu Amanekh. Si vous regardez bien les images, Amanekh a été le premier à toucher le sol, épaule et même sa tête, avant même d'appuyer la tête de Thiatou Daouda Fall.
Sénégal dougnou wakh deugeu.
Bravo le CNG et Kandji
Fein bakhoul
Ama nekh mo dane Boulesniou fonto
Mingui mélni kou nék ci audience déh
thiakhan bakhoul amanekhe mo Dan boy bi bayelen sen thiakhan yi
Nafék rék man walo walola mais amanékh mon am ndam
Iow bo nêkè wallo wallo nakk
Ama nékh sou wakhé Lou wakhouwoul aussi atébi diaroul yonn
Aziz Ndiaye dal moy niaaw Yaaye 😂
MERCI CNG SÉEN LIGUÉY RAFÉTT MASHALLAH ❤❤ YÉNEU GUISI YONN ❤❤ MAIS AMA AK FRANC TAMITE WARGALEEN SUSPENDRE OU AMENDÉ VRAIMENT 😮
Bilay li dou yon je te jure amanex mo dan
CNG ba légui bakha goule ndakh mber you bari dawe nane lambou dji ndakh yénnne CNG bi
Yakhal guen gaston production vrement ak niang bou ndaw
Boudon aziz ndiaye la sursie lanioukoy def
Merci CNG
ama nekh mom injustice la dound.... senegal yeup hamnagn ko
Bravo aux CNG li rek mo koy réglé inchallah
Félicitation cng
Très bien amanekh
Yéne ay nafekh gén
Diokhlen siteu ak ama nekh ndamam senegal da beuri ay nafekh
Khamou Lin dara zarko 2 Ani lá wara am dou takhaw si Lamb ji ama nekh defol dara
Yene ay narfekh guene
Mé pourquoi les Arbitres kéneu douléén Sanctionné té niouy yakeu lambeu yeupeu
Injustice rek,doléne rouss sakh!
Amanékh danguéne ko diay dollé, mais yalla moléne eup dollé...
Le CNG a fait du n’importe Amanekh a gagné le jour du combat il a gagné après recours pourquoi revenir encore sur ça li day yakheu lamb vraiment
Appel si reglement bi la bokk
Malicke Ngom
Mom khamoll dara Na bayi
lamb dji
Donc amanekh d'où beure ak niang bou ndaw
Amanekh a raison
Tres bien pour les sanctions sur amanekh.. il a tort.. on la battu Thiatou dawda fall moko dane arbitre yi danio dioum
Gng nékoulène si Deug
amanekh mo danne daguéniii toth senn thiotou ndaye dul wa cng aziz moy sen baye
Meuna wax taxoul lo wax mou nék deug VAR waroul am recours am ba appel guén dora dioxé victoire
Bilahi yaw Kendji CNG bi amone nasi Yakar pour ni degue dinafa âme mai victoire pour thiatou Daouda fall gisouma louko mana dégueul té amanékh limousin wakh degue la
Amanekh daffa war khamni CNg règlement youmou tek
Si texte bi lagnou soukandikou pour diokh Thiate victoire bi
Et quoi qu'on puisse dire waroul wakh CNg dagnouy fen
Mais kandji dioum gua , parck les 3 autres nekouniou fi , amolene droit bolelene si jugement. Seul les présents ont votés.
Vraiment amaneh mo dane
Wa balla gaye limoufiwakhone moudioul féne thieuy galsen😂😂😂
Kandil domiharam
Amanekh vs Thiatou sa vrde
Cng nékoulène si deug
Amanekh seul 👌💯 Rufisquois
diadieuf kandi discipline dafa am solo
Père thioune bamou néké Si lamb ba légui mogui sogua dioum si sama yakar meunon nguén ko avertir rek bagn ko sanctionné vue que sen biir la book dafa dioum tée niit kassé laa
waadji ndongo lo leyy ndirool
Ama nékh doit se faire accompagner et attaquer la décision du CNG au niveau du tribunal administratif. Le CNG est juridiquement en tort dans cette affaire
Nafekh rék NIT day wakh deuk dindilen VAR en foot VAR.sou wakhé diekhna amoul recour wakhulen ben deug 1 superieur a2 amoul féne
Mais ki mane ak mome béne nagne .un ak une yi mome .....
Gng bi dane lene conrome kesse guemou ngiou Dara ama nekhe n'a deguou kesse ba pare ame name ngiou na guou KO nakhe khalise
Balla gaye saga nalene fo 😂
C vrai ay nafekh lane
Bahl waroul am
Cng 2024 ak bou 2025 be 6 ak 9 lá rek ama nekh mou dane thiatou daouda fall
Yakh lamn dji rek ngene fi nara deff
Amanekh seul domou rio bii
CNG VOUS AVEZ INTERDIT LE PORT DE TENUE MILITAIRE AMA BALDÉ MIGUI KOYE SOLE SI FACE TO FACE DONC IL DOIT ÊTRE SANCTIONNÉ
Senegalais djité léne métina bilahi 😂🤣😂
Billahi
Ay corrompu guéne😂😂
Man lima geuna diakhal lou takh niou athie amanex
Dayédi douf rék CNG
Js daccord que amanekh waroulen taxe de corruption mes da meron meunon guenko def susrsi ak amende balla gaye a fait fire teksi guen convoque ko mou bagn que cest tre grave