Le CNG encore une fois respecté ses braves lutteurs et les amateurs ceci est inadmissible la var a trancher en faveur de Amanekh le jour j à quoi Sert la Var s’il n’arrive plus à faire la différence entre un vainqueur et un vaincu lors d’une action juste pour faciliter la tâche aux arbitres c’est la même situation entre Reug Reug et Sathiés Nekkk l’enn ay niiit 🙌🏻
Amanekhe a bel et bien gagné contre Tjiatou Daouda Fall. Il est temps d'arrêter cette injustice ! Nous devons défendre l'intégrité de notre sport et garantir que la vérité soit reconnue. La lutte sénégalaise mérite d'être honorée sans manipulations ni favoritismes.
Il fallait casser le verdict c mieux pour plus de cohérence dans les décisions. Comment on peut gagner après visionnage de la VAR ensuite après recours pour venir perdre en appel. C insensé
Félicitations Amanekh fi yalla rek mofiné alassane depuis france en direct lakko sétaan Adouna khamnané ya dane Var bii pourquoi il a donné la verdict alors sng boune doullo nitt gny li affaire de Deum leu waay
Ama nekh mo am victoire lolou Sénégal yeupp kham nagne ko ama nekh wakh nga deugue bou werr y’a am victoire ama nekh 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Amanekh Yallah baxna, yaw ya ame ndam, ya dane champion mais ta tout compris affaire yi xaliss moy dokh mais ps deug!!! Fiyafiné!!! courage champion continu tes entraînements té geuneu geum Yallah
No vraiment nak cng dfa def louko nekh man Thiat la faralon mais amanekh dako daan franchement lii mom day yakh lamb vraiment kon kay nagn diox siteu victoire ram contre modou lo tmt 😊
C’est ainsi que fonctionne la justice : elle n’est pas parfaite et peut commettre des erreurs. C’est pourquoi, lorsqu’un tribunal rend une décision, il est possible de faire appel devant une cour d’appel. Si celle-ci confirme la décision, la partie en désaccord peut saisir la Cour de cassation. Cette dernière peut soit confirmer la décision, soit l’annuler.✍️
Ce verdict décrédibilise totalement l' instance chargé de l'arbitrage de la lutte avec frappe . Pour moi , notre sport favori est la lutte mais Sans frappe
Naniu dindi var kone si lamb dji amul sens vraiment Amanekh félicitations encore une fois tu es notre fierté 🎉
Var dafa wara diekh si lamb Prsk amoul sens Prsk deja seen matriel bi dafa dess var bi deh tourou var leuh rek
@@mansourgningue4082 arbitre bii jour combat bii sou dieulone temps am dina guiss dieul bii
Dafa tella diokher victoire bi jour bobou mo yak lamb bii yeup
Dano wara dindi 4 appui ak épaule dan bamou jaxan ay millions lan lén fay
Wakhgua deug dé😂
Guèdiawaye la deuk je suis 100% fans thiatt té mangui wone stade mai boudé yalla deug la beug rk amanèkh mo dane😢felicitation amanékh
Daffa leer vraiment
Dégouma deug dé
Diaye dollé mon wara diekh Sénégal bly ❤❤
Bilay wakh na deug; li mom diay dollè leu
Amanekh tu as parfaitement raison.tu as gagné.
Bro demal setanat combat bi amanekh dafa appuié si épaule lam bici souf pr beuss la tête d son adversaire
C'est vraiment désolant
Guereo es fier de toi Ama nekh lebou yeup contannañou ❤
Wakh deug Amanekh tu as raison, Var ak commission recours yeup t'ont donné raison. Wa appel khana ils ont d'autres yeux
Justice pour Ama Nékh
amanékh mo dane bayi léne sokhor 😢
Guediawaye la deuk mais ama nekh mo dane
Deuko fii dh
Deuko fii dh fall
Dégouma deug dé boy
C'est injuste vraiment
Le CNG encore une fois respecté ses braves lutteurs et les amateurs ceci est inadmissible la var a trancher en faveur de Amanekh le jour j à quoi Sert la Var s’il n’arrive plus à faire la différence entre un vainqueur et un vaincu lors d’une action juste pour faciliter la tâche aux arbitres c’est la même situation entre Reug Reug et Sathiés Nekkk l’enn ay niiit 🙌🏻
Félicitations encore ama nékhe ❤ yadane boybi nak
Thiakhaane bakhoul, Amenékh mo daane. CNG NAGNOU BAYI FANEKH.
Walahi lamb yakhouna Billahi 😭😭😭😭
Wakhma luko yakh
Sawayy Amanekh dafa danou
Modou lo épaule la ték niouné danou woul cng mafia la
Dafa yakhou bo yague frère
Moudou lo épaule la tekk m siteu nekol thie buer ep Moudou thie sakoye la tekk épaule wakhal dague rek
Sénégal yeup xam naniu ni Amaneikh mo dane c le plus important
WakhO deug dè Sénégal la nèk té amanèkh dagne ko dane
Wakho deuk deh Amanekh dafa danou❤
Mane lima métti rek moy lima yalla nato ma beug lamb🙏🙏🙏🙏
Félicitations ama nekh ya dane
C’est vraiment honteux courage amanekh yaa daane Brkii alhouraane
Bilahi amanekh Mo daane Cng ay Domaramlagn rek
Amanex bùl inquiètéwu ñoun on sait que ya dane ❤
Diokoul est fière de toi mbëur ❤🎉
Amanekhe a bel et bien gagné contre Tjiatou Daouda Fall. Il est temps d'arrêter cette injustice ! Nous devons défendre l'intégrité de notre sport et garantir que la vérité soit reconnue. La lutte sénégalaise mérite d'être honorée sans manipulations ni favoritismes.
Injustice dou gawa dièkh sénégal à cause de l’argent; les gens sont affamés de l’argent
Recours mo wara diex ci lamb puisk var amna recours pour contester une victoire amoule ci bén sport
Donc les arbitres devraient être suspendus alors
Félicitations amanekh ya dane
Dane bou lere yalla rek mofi nek
Bilahi walahi ama nekh mo dane cng wakhoul deugeu
Amanekh défal appel yaw aussi
Félicitation amnékh ya am ndam 🎉🎉🎉🎉
Amanekh mo ndy dane waay ah ay ndy nafekh ngen rk ah
Merci beaucoup amanekh pur vérité CNG nagnou bayi thiakhane thiatou Daouda fall Mo danou Feni Kese la mbeur Bou ndaw d'où recours
Félicitations amanekh .... Am nga namm
Amanekh mo dane lolou moy deugue ✅️✅️
Non non Amanekh linga wakh yep deugue la Machalla
Vraiment ya daane félicitations
Thiatou daouda fall mom sakh khamnani danouna
Khana gnimou andal nio soff rk
Il fallait casser le verdict c mieux pour plus de cohérence dans les décisions. Comment on peut gagner après visionnage de la VAR ensuite après recours pour venir perdre en appel. C insensé
Ama nékh kéne yoroul sa wer séuk kofiyakar yalla layakar bi hahkanim hakimin lo até dinko atéwat ama nékh seul🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤💪👈👍❤
Vraiment Lou lêre y'a. Am victoir
Félicitations amanekh
❤
Amanekh Vs kaw gourdin combat leu
Kaw gourdin koumou dan kaw gourdin na dieul Alfa 2
@@IbrahimSamb-od3wnmo dane thiatou daoda fall
@IbrahimSamb-od3wn
Kaw gourdin mo doumeu tiatou Daouda fall dann KO.
@@IbrahimSamb-od3wn c'est Ki Alfa 0,2222 😁😁
Félicitation amanekh 🎉
Ceux qu’ils ont refusé à siteu , ils l’ont accepté pour thiatou daouda fall . J’ai toujours dis que lamb y’a que des corrompus je te jure ☝️☝️
Bilae ta vu voilà le Sénégal
Tu as parfaitement raison amanekh soudé nila donc siteu mo dane modou lo
Boudé yaw wéro gnoune ay niteu lagnou action beulé khéw si biti action gnom amanékh bi khéw si bireu guéweu bi nguay comparer gnari action yi
Jeu siu neutre mais amamnekh mo dan yalla kham noko Sénégal nane bayi afferou na fekhk tay atte deug akh 😢
Fi niou dougueul épaule Lou modou lo mane dougueul victoire Bou amanekh
Cng
Honte à ce bureau! Thiakhane baaxul waay!
Mann épaules bignouy wakh la guissoul
Vraiment thiatou dawouda fall la faral mia thiatou dawouda fall soudané amanékh siteu dan neu modou Lo ok 👍✅
Siteu moh dane kay ms si biti laaaa
Sawayy bokkoul siteu si bitti la deffei action amanekh danouna
Bilahi man modou lo mom rek laye topa meis veritè
Félicitations Amanekh fi yalla rek mofiné alassane depuis france en direct lakko sétaan
Adouna khamnané ya dane
Var bii pourquoi il a donné la verdict alors sng boune doullo nitt gny li affaire de Deum leu waay
Ama nekh mo am victoire lolou Sénégal yeupp kham nagne ko ama nekh wakh nga deugue bou werr y’a am victoire ama nekh 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Ama nekh mo dane
Amanékh seul notre fierté teungueth laniou deuk ay lébou pure laniou wa c.n.g amoulène béneu vergogne meunou lène ci nioune touss
C'est désolant vremaaa Amanekh yà dannnnn
Wakh Yalla amah nekh mo dane
❤❤❤❤amanekh mon ndan
Merci beaucoup 👍👍👍👍👍
Ama Nekh tu es un grand champion diam rek ngay am In Sha Allah. Gars yi danioula wara diokh sa thieur ci lamb ndakh danga ci am thieur deug nak.
Ama nékhe le vainqueur indéniable ❤❤❤❤
Billy amanekh wakh na DEUG siteu Modou lo kom nila
Amanekh Yallah baxna, yaw ya ame ndam, ya dane champion mais ta tout compris affaire yi xaliss moy dokh mais ps deug!!!
Fiyafiné!!! courage champion continu tes entraînements té geuneu geum Yallah
CNG atté wouniou Deugg Amanekh mo dann Thiatou Daouda Fall soyez sportif way Boy bi Moy Kane ba d'où Danou
Boye bi sou dieullée victoire inchallah carriére am dina yaakou kou weeddi yoral say gueutt tey xool yaagua toul
Yama meuna fen
Vraiment tu as gagné
JUSTICE POUR AMANEKH
Félicitations Ama nekh
Injustice totale vraiment
Félicitations thiatou dawouda fall
C'est injuste boulene yakk victoire diambour way
No vraiment nak cng dfa def louko nekh man Thiat la faralon mais amanekh dako daan franchement lii mom day yakh lamb vraiment kon kay nagn diox siteu victoire ram contre modou lo tmt 😊
Khana guisso épaule bi ama nekh bi Var nio thiouné rk
Bilahi
Kon kay dénio déf Lou lén néx siteu dane na mod lo té bo bu mo guéna ler sah
vraiment amnékh ya am ndamm❤❤❤ cng bi wakhogne deugue 😮😮
Ama nekh mo dane❤
Félicitations Ama Nekh ya dane
Amanekh mo dane
Bilay ya dan ❤
Amanekh mo danou.var niari bopyi lanioudon khol guisouniouwon epaulou amanekh c Ca la veritè!!!!
Vraiment li nekoul yone billahi
Vraiment li dou yone
Ama neikh mo dane wayyyy lidou yonne wayyy ishhh
Bilahi yala na yala wathié président malick ngom té yala tax li daffa niaww
Félicitations amaneikh vraiment yaa daane ....CNG ay badola deug laniou .....lanla vaar di diarigne ...aparsa thiate dafa daanou
amanekh dagua danou mayniou diam sa épaule mo djitou mbeur vraiment deuk bii moy ya danou billahii
Vraiment épaule bi mo nieuk lal souff Var nio thiouné rk
Félicitations thiatou Daouda fall du courage ama nékh
Thiate mo dane vraiment courage ama nekh
Waxal degeu Thiat meunoul dane nak
Ama nekh mo dane
Fou thiatt danè dèlèn wakh deuk
Yw khana danga giss diéleu bouniou gissoul no way ama nekh mo dane
Félicitations Ama Nekh je retiens ta victoire
Cng verimant si aye thiakhan rék ngéne nék Lingéne déff tégou léne ko féne khana yama nékh rék
C’est ainsi que fonctionne la justice : elle n’est pas parfaite et peut commettre des erreurs. C’est pourquoi, lorsqu’un tribunal rend une décision, il est possible de faire appel devant une cour d’appel. Si celle-ci confirme la décision, la partie en désaccord peut saisir la Cour de cassation. Cette dernière peut soit confirmer la décision, soit l’annuler.✍️
Felicitation Thiatou daouda fall.
Ssay thiat dfa danu devant 17 million de senegalais. Felicitation kiko adjo yobunako ma nieup nangul ko
Ce verdict décrédibilise totalement l' instance chargé de l'arbitrage de la lutte avec frappe . Pour moi , notre sport favori est la lutte mais Sans frappe
Aussi les conséquences qui devraient s'en suivre c'est pourquoi les arbitres sont pas sanctionné ?
Amanekh bilakhi ndanane dëguë nga kéne manou chii darra
C'est vraiment injuste. Amanekh ya daane . Vraiment CNG dioumna cette fois ci
Vraiment lamb yakhouna
Mané mome thiat moy smaa mbeur mais il à raison bly ❤❤❤❤❤
Félicitation amanekh
Way thiate moko dane félicitation 🎉
Bilahi 🎉
Foumouko danè wakhi supportaire
Donc faut confirmer le Victoire de Siteu sur Mod Lo
Ama nékh deugg rék nga wakh
Ama nekh mo dane dh bilahiii
Ama nékh ya dane vraiment
Ses injuste,Amanekh a gagner.
Amanekh 🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤
Victoire amanekh ou sen verdict
Amanex Diokoul est fière de toi ❤❤❤❤
Boulén gniou founton Thiatou qui est le vainqueur
Watal
@@MamadoulaminejustinSankawalahi thiat mo dane
Danouna Amanekh moko dann
C'est faux nak yalla fi nékkeu bima guisé Moustapha géye Di analyser nane ay épaule Ama nékh bi la khamné il se préparer quelques choses
Amanekh a gagné le CNG a vraiment dérouté et c'est décevant après tout
Sama deugue rek lay wakh mai ama nékh sa épaul bi nékhouta lithiénti déh aussi baga diougué sa reaction bi ahh yalla bakhna
Arbitre bi mo dioum dafawarona sifflé watt bouko defone kene dousi bagne parce que léroule
@
Waw kay nak yaw nak wakh gua lépp
Affaire bi sans verdict la warone nek.
No épaule est-ce que chute la ? Parce que Modou lo épaule bi laal na souf contre siteu mais ken djokhoul victoire bi Siteu
@
Mai aussi chute bobou fimou amé la siteu migui wone sibiti mai gni niogui si birr wala guisso lolou