C'est la première fois que je t'écoute, mais j'avoue que t'es sans façon Wally. Chapeau à toi. Kouleu dégg lou xam ni diambaar deugg ngeu. Maa chaa Allah. Kou geumm yallah ngua. Billaahi dameu contaane. sama xol féss na👏🏽👏🏽👏🏽
Macha allah Waly quand j t'attend parler jé les larmes aux yeux sa xol dafa rafèt tu as encore prouvé ta maturité quand on t'attend parler on sent le respect l'intelligent et la politesse dans tes paroles merci encore milles fois rouss lo wognou bèn yone tjrs di sora lé les fans mane dh lingua fi wax yeup nak gnane bingua gnanal les élèves d terminale rk moma si geuna néx aminne yalla nagnou ko yalla may..Et enfin Pape Cheikh Diallo il était temps k Waly niew tfm parsk musicien la com tous les autres donc amna thieur fofou Merci Pape contane nagn torop..yalla na continué🙌🤲
machala Wally deck à coeur ouvert à la tfm hnogyi khar yènène felicitation à pape cheikh et son équipe adouna lepp téranga wally bonne continuation dina bakh inchallah sa Khôl dafa nice
Srx Wally seck il est le meilleur sa façon de communiquer est exeptionel t'es le meilleur big respect Yangui gnouye siguile bou bakhe roussou gno takhawwe féneuh di Wakhe sougnou fans nga machallah
Franchement je suis émue. Wally seck aka modeste. yay goor di ndandane tu es le meilleur the king 🤴🏾🙏❤️ pape cheikh yalna souniou borrom goudal sa fann. Bilahi yaa niakk kinian.
franchement sama khole seede wally es t'un grand T''homme il a un esprit de depassement machallah lafthiat mais pape cheikh es un grand t'animateur grand merci a TFM
Machalla seck wax bi rafet na and ak dal ak posé vraiment yalna diam yagu té yéne wa tfm guéne changé té nagou dogalou yalla wally yalla mokofi tégu donc nagoulén té guéne continuer diko invité di tégu ay son wam ok soof guéne trop inshhhhhh
G les larmm au zieuy merci waly yalla na yalla feyla ligadeff si khaléyi on beujoi daide pusk gni amm bouniou donn diaplé gni amoul dinaniou avance mes merci kamaime
Sama diamono niom papa Youssou ndour mo nekone sen roi du mbalakh ! Mais cette nouvelle génération tu es leur roi 👑 du mbalakh ! Diamono bou nek ak kisiy khew ! Fonce on est derrière toi ❤️
@@babacarvisionbabacarvision1796 ya meune doul wally force sa saram ndaye gordjigueine bou teigueul sa ndaye bi .d'où da NGA rew Di ma saga Di NGA khamni ma la gueune yakhou fouff sakh.salaupard😞😞😞😞
Juste Waouh! la communication de Wally a beaucoup améliorée on voit un Wally conscient,posé un Wally qui a la tête sur les épaules il a beaucoup appris de ses erreurs Macha Allah Wally moi personnellement je le suis depuis ses débuts une personne avec un grand cœur un bayefall digne de ce nom dafa melni dama bok ak mom que le tout puissant te facilite et te protège qu'il veuille sur toi niguay sédalé souniou khôl yi yalnalako sougn borom fay barkep Cheikhoul Khadim bravo à Pape Cheikh one love❤️
Toute mes félicitation Pape Cheikh il était tant que wally se présente à coeur ouvert avec la TFM.....et c'est pas suffisant nak nafaa Boy bi saf sap dafa diot
Je n'écoute pas du mbalax, mais j'ai fais une remarque aujourd'hui. J'étais dans un marché de dakar mais presque dans les boutiques que je suis passé, ils ne mettaient que Wally. Ni Youssou, Thione seck, etc. La je me suis dit que ce gars est déjà dans le cœur des sénégalais et comme on le dit en wolof "moye bombe". Yalla nq diame yage
Machalla domou pape Thioune la nak gueme gueme rekkkkkkkk bilay walay sama pape Thioune doumako mese fate 😭😭😭😭😭yalla nako yalla yeureme khareko aldiana firdaws té soufeu woyofeu thi khawame amineeeeeeeeeee ya rabbi
Toubarkala massala kirassoulay beug guimala beug eup neu mar yacine..seutou leuk daour bi penc majigén mbor ak Ali majigén mbor..💖talibé seix ibra faal lamp bi dound rk faal yaaram bi🙏🏼
Bilay décourager wone na si live bi mé waly heudy wate nama dakh moment yi magui doune dou lou méti mé waly takhna ma khame ni il n'est jamais trop tard
So degalé sey fans nel waw rek té boulein denk sa event kone niou sabotéko kom waw dou booy guemine nel waw rek nonou demb bou nango tay ay pexem diouboul forcé nguein sen artiste ba soneu demoul nguein ni naniou dem cii doff bi ndax xôlam dara nekouthie da nguein xaamni thione moy bayam ..en tt cas wally bne continuation pertinant yarou ak dall merci ❤❤
Ndeysan le clip « Bo dioudo » m’a vraiment emu. Guiss ngua lou Yalla di def deh, xolal legui difference bi rek Mashallah. Sunu Borom dimbeuli naleu bou bakh. Sante ko bou Bakh. Bayefall ngua
55:25 Pour quelqu'un qui n'est pas allé au delà de la 5eme il s'exprime dans un français parfait. Il est vrai que son père aussi s'exprime très bien en français, çà a dû aider
Non suis content merci pape Cheikh ci invitation bingua inviter Wally seck mane dema xeur ci you baniouma Wally mais bene ins comparaison biko Aÿ fans am diko teukeuler ak you moma meti ba deglotoumoko tt en sachant ke ndanane la nn mais crx nanguoul nakoko mais j'aurais aimé ke tfm diko tekk ke momak you niou am link bou Nice mane je comprenais pas le silence de tfm encore moins niak présence you ci Bercy am sachant ke il était invité d'honneur; mais dema contane ci lingua def pape cheikh j'espère ke dou yem fi mais you kene dou yow machallah tes un grand mr nek lene ci diam
Abdoul Bocoum dj arafat et sidiki ont-ils eu des distinctions que wally n’a pas eu ?! Ont-ils fait bercy ou zenith ? N’importe quoi ! Iow mom sokhor mola diap ! Wally est un senegalais comme toi encourage ko moguen
@@Junior-kalish ki diaroul tontou parce que dou sénégalais motakh mou sokhor mais sénégalais bokham ni yalla rék motakh ngaye wakh te sokhoro bilahi nouvelles générations bi wally moy sen baye
Thiey mar sama xol sedatiina ci yow💗😍 contanatiina deii ! Danga néxxa beug ndahh bagn la beugué batay meuussognou tékk gaathié nous tes Fan au contraire💗💗💗! Amaal jaam rek iow goudou faane ak weer Mar yacine Meissa Bigué yalna sa jaam yague Faramareene bii😍😍😍👏👏👏👏
Machalla lawelaaaaaaaaaaaaaa thiatttttttttttttttttte thia bamou dalagoul sama domou kholllllllllllllllllll thia khawe thia khaname rekkkkkkkk inchalla yalla nala yalla samale boppame sur tout amineeeeeeeeeeeeeeeee ya rabbi
Enfin intégrale bi🥰
Kou beug wally pouce bleu
C'est la première fois que je t'écoute, mais j'avoue que t'es sans façon Wally. Chapeau à toi. Kouleu dégg lou xam ni diambaar deugg ngeu. Maa chaa Allah. Kou geumm yallah ngua. Billaahi dameu contaane. sama xol féss na👏🏽👏🏽👏🏽
Le mec il parle avec une telle maîtrise. Et avec une retenue très rare ! Mashalla Wally Ballago Seck on t'aime 😍
Macha allah Waly quand j t'attend parler jé les larmes aux yeux sa xol dafa rafèt tu as encore prouvé ta maturité quand on t'attend parler on sent le respect l'intelligent et la politesse dans tes paroles merci encore milles fois rouss lo wognou bèn yone tjrs di sora lé les fans mane dh lingua fi wax yeup nak gnane bingua gnanal les élèves d terminale rk moma si geuna néx aminne yalla nagnou ko yalla may..Et enfin Pape Cheikh Diallo il était temps k Waly niew tfm parsk musicien la com tous les autres donc amna thieur fofou Merci Pape contane nagn torop..yalla na continué🙌🤲
machala Wally deck à coeur ouvert à la tfm hnogyi khar yènène felicitation à pape cheikh et son équipe adouna lepp téranga wally bonne continuation dina bakh inchallah sa Khôl dafa nice
Srx Wally seck il est le meilleur sa façon de communiquer est exeptionel t'es le meilleur big respect Yangui gnouye siguile bou bakhe roussou gno takhawwe féneuh di Wakhe sougnou fans nga machallah
Non waly seck pape cheikh Diallo vraiment ay nit you bakh legn surtout la simplicité. Yalla na sen diam yagu lolll💖💖
Aminé
les plus doués de leur génération. Que le tout puissant vous protège. ce que vous avez en commun talent et gentillesse.
Se garcon est béni par le bon dieu kou yabou nopalou . Merci pape cheikh vrai humaniste.❤️
Bonne continuation wally franchement u es l meilleur de ta génération yalla nala yalla diapale si barki seydina Mohamed psl
Bravo une communication bien ficelée on sent qu'il est bien entouré par des pros.il a été pertinent du début à la fin.
fall893 bilaye c’est un gars qui va de l’avant.
Franchement je suis émue. Wally seck aka modeste. yay goor di ndandane tu es le meilleur the king 🤴🏾🙏❤️ pape cheikh yalna souniou borrom goudal sa fann. Bilahi yaa niakk kinian.
franchement sama khole seede wally es t'un grand T''homme il a un esprit de depassement machallah lafthiat mais pape cheikh es un grand t'animateur grand merci a TFM
Machalla seck wax bi rafet na and ak dal ak posé vraiment yalna diam yagu té yéne wa tfm guéne changé té nagou dogalou yalla wally yalla mokofi tégu donc nagoulén té guéne continuer diko invité di tégu ay son wam ok soof guéne trop inshhhhhh
Bien dit yalla moy mayé
MachAllah Wally Yallah nala souniou borom same thi barke Mouhamed 🙏🙏🙏
thiees Wally mi nak Mon warona nek candidant nak Bilahi gaïnde dou dioure mouss domou gaïnde gaïnde rek la mana done merci pape cheikh diallo
Magui lay gnianal wally tu as bon cœur et en plus beaucoup de talent alors vas y dina bakh 🙏🏾🙏🏾
J'aime bien pape cheikh car il dit tjrs inchalah Machalah
Diameu rek ngay ame wally ndakh sa kholl bou raféte puissance rék da nga ame dollé 💪🏿♥️
*L roi de la musica* 🔥🔥
*_Bay Galay guiss nako mou tokk sii kaw dii setane aka beugg WBS mai day bagne_*
*Team Wally B. Seck* 🔥🔒
😂😂😂😂wa kouy baye galaye
@@fatimarahssoulfall3276 hiii bay galay day guiss bopam nan bayii nonu 😂
@@abdumaty1046 Noo dead na😂😂😂😂wa kone nagn nopiii baye galaye mbadou daniouy beguee ci pett
@@fatimarahssoulfall3276 bagna beigg kenn dou bromm symphonie woy kat bii
😂😂😂😂 baye galaye tème mouné effacégnou
G les larmm au zieuy merci waly yalla na yalla feyla ligadeff si khaléyi on beujoi daide pusk gni amm bouniou donn diaplé gni amoul dinaniou avance mes merci kamaime
je t'aime beaucoup avec ta philosophie surtout ta gentillesse, yalla nalla yalla diapalé
Sama diamono niom papa Youssou ndour mo nekone sen roi du mbalakh ! Mais cette nouvelle génération tu es leur roi 👑 du mbalakh ! Diamono bou nek ak kisiy khew ! Fonce on est derrière toi ❤️
@@babacarvisionbabacarvision1796 wakho deugue dei diamono bou neike amna kouy kheiwe . diamono dji môme Wally la kou yabou.nangou nopalou . égoïste bakhoul ok broth.
Bilahi yalla lako takha wakh
Mali sidiki diebate côté d'Ivoire dj arafa Ginne Gandia kora Sénégal wally seck nouvelles générations mome c'est le meilleur tous jour
@@babacarvisionbabacarvision1796 doul merde katal sa ndaye feulei domoukhathie so ma sagatei reike ma ouye⛔⛔⛔⛔ imbécile
@@babacarvisionbabacarvision1796 ya meune doul wally force sa saram ndaye gordjigueine bou teigueul sa ndaye bi .d'où da NGA rew Di ma saga Di NGA khamni ma la gueune yakhou fouff sakh.salaupard😞😞😞😞
Juste Waouh! la communication de Wally a beaucoup améliorée on voit un Wally conscient,posé un Wally qui a la tête sur les épaules il a beaucoup appris de ses erreurs Macha Allah Wally moi personnellement je le suis depuis ses débuts une personne avec un grand cœur un bayefall digne de ce nom dafa melni dama bok ak mom que le tout puissant te facilite et te protège qu'il veuille sur toi niguay sédalé souniou khôl yi yalnalako sougn borom fay barkep Cheikhoul Khadim bravo à Pape Cheikh one love❤️
Très belle émission! 1ere diakarlo entre pape cheikh et wally sur la tfm, il était temps 😍
Fou youssou Ndour agg si music yalla nafa wally wessou 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️🌹👀👂🏾
Aminé
Amine ya rabby
Toute mes félicitation Pape Cheikh il était tant que wally se présente à coeur ouvert avec la TFM.....et c'est pas suffisant nak nafaa Boy bi saf sap dafa diot
Machallahh Machallahh Wsly yalla na la yalla same🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥰😍
Ibou Diop û
Nafi faye
,
,
Fière de toi Wally faramarene your Number one fans from Denver Colorado ❤️❤️❤️ très contente merci Pape cheikh pour l’interview
Wally bravo à vs 😍🥰
Ndeysane j’aime bien se gosse la il me fais rêve et aussi di kharou si liguey pour une réussite total yalla n’a sa jame yage one love brooo
Tfm mbadou album international biguen degu motax guenn invitei wally lolll...wally sa xol rafet na mashalah goudal fane lov u...pape amal diam
Chapo a Wally machallah yalla nala yalla yoggou ba nga yékko
Bilay pape cheikh thi bopam dafa fan wally seck liral regard bi
Prsk Waly moko woné xalé bi kou waxal ba paré dingua ko fans ndax nimou mell xol.bi rafèt na.sètt na
mon dieu
Wally Seck vie sur tw
Gnoun dagno am sa faiblesse sougnou xol yasi fess🌹❤
émission bi noume toudou ame na solo machala wally yalah na sa dime yague
machaallah wally tu es le meilleur bonne continuation et merci pape cheikh
Je n'écoute pas du mbalax, mais j'ai fais une remarque aujourd'hui. J'étais dans un marché de dakar mais presque dans les boutiques que je suis passé, ils ne mettaient que Wally. Ni Youssou, Thione seck, etc. La je me suis dit que ce gars est déjà dans le cœur des sénégalais et comme on le dit en wolof "moye bombe". Yalla nq diame yage
Lou leer nga waax...
Faites glisser des éléments du presse-papiers pour les supprimer.
B ilaye wolaye
Wally don't mine them no matter wat they said about u I still like you and even my fellow Gambian love u always
Machalla domou pape Thioune la nak gueme gueme rekkkkkkkk bilay walay sama pape Thioune doumako mese fate 😭😭😭😭😭yalla nako yalla yeureme khareko aldiana firdaws té soufeu woyofeu thi khawame amineeeeeeeeeee ya rabbi
Bilahi ya bakh, wally yalla rek molay fay sa xol doundal 111ans Amin ya rabby
J’ai vu Black Panthère at the theater on opening weekend et j’ai eu le même feeling. C’était fort d’entendre la voix de Baba Maal et les tamas
Wally seck khamnani do Fake do ragal mais yalla bo guiss Loula diakhal thi barki layilaha ilala seydina mouhamed salalahou alaywassalam.🙏🙏🙏🙏
DIADIEUF WALLY ET MERCI BEAUCOUP PAPE POUR CETTE ÉMISSION SI IMPORTANTE ET REMPLIE DE SENS.
Bilahi vous avez rendu ma soirée merveilleuse..Waly Seck tu es mon point faible je t'aime tout simplement💕
Machala yalla na diam yague tfm sa télé papa la ta yow produit bou nekha diaye nga yalla na ande bi sakh ta barkel
Nice machela wally
Boy bi il est courageux franchement gnaffer kat leu
Voilà la vie et belle bravo Pape Cheikh Diallou hai fatto bene
Vive Wally B Seck hai risposto benissimo
Toubarkala massala kirassoulay beug guimala beug eup neu mar yacine..seutou leuk daour bi penc majigén mbor ak Ali majigén mbor..💖talibé seix ibra faal lamp bi dound rk faal yaaram bi🙏🏼
Un vrai man vraiment kou waara diapalei nak il fait notre fierté 💖👍
machalla. wally. sa. wakh. rafetena. ni ce ne. pape.merci👏👏👏
Parcour c trés touchant bilayy j fallu pleuréii mla beugg pirrr jtjr
May God Bless you Wally i love you from Toronto
Yagueuna byby
Machala yalla na yalla lafale thiate merci baga lerelé sa tangue bi
Enfin Tfm nangouna booy
Bagne bagne nangouu 😂😂
Never give up bro you Will be the king of balakh 🙏🤲 cheikh mbaye brazil Love my Senegal ❤🙏 God bless 🙏🤲
Long vie à toi waly séck je t'aime bien sa khôl dafa rafete machalla
Anis gnis beugue wally gnogui nii😘😘😘❤❤❤❤💪💪👍👍💕💕💕💕💕💞💞💞💞👑👑👑👑
Wally notre fierté que le bon Dieu te protéger
Machalla pape khiekh Diallo sa liguéy raféna
Bilay décourager wone na si live bi mé waly heudy wate nama dakh moment yi magui doune dou lou méti mé waly takhna ma khame ni il n'est jamais trop tard
wally seck diame rek guaye amna incha allah mala begue
Wa tfm nak niongui dora def yeufou nite.... pour 1e fois waly done invité 💖
26:50 Geumm Yallah rekk mo amm solo Mar Yacine ioa dall amall diamm rekk 😘 dp8 diamono boo dioudO beu léguii machallah rekk 💞💞💞💞
ah pap cheikh lii yombee n dh bayii yépp sotiii nguènnn dogo gneuww gnoune senTV lagnou amm bamouyy métii gnofii nèkoneee Wally defsiii ndakkk rekk
Me nekoul ti pape cheikh di ti nom bouba la rekk li pape cheikh am ni grâce ah abajo stress la rek
So degalé sey fans nel waw rek té boulein denk sa event kone niou sabotéko kom waw dou booy guemine nel waw rek nonou demb bou nango tay ay pexem diouboul forcé nguein sen artiste ba soneu demoul nguein ni naniou dem cii doff bi ndax xôlam dara nekouthie da nguein xaamni thione moy bayam ..en tt cas wally bne continuation pertinant yarou ak dall merci ❤❤
No wally yalla nako yalla yokkkk❤
Aminne
Ndeysan le clip « Bo dioudo » m’a vraiment emu. Guiss ngua lou Yalla di def deh, xolal legui difference bi rek Mashallah. Sunu Borom dimbeuli naleu bou bakh. Sante ko bou Bakh. Bayefall ngua
C est te trop bien vous touchez on était la à Bercy avec vous wally seck continue tu est le meilleur
Douma deglou musica me Wally koubakh la xolom dara nekou thi loudoul talibe machalla
Fallou Thiam
55:25 Pour quelqu'un qui n'est pas allé au delà de la 5eme il s'exprime dans un français parfait.
Il est vrai que son père aussi s'exprime très bien en français, çà a dû aider
Fréquentation fait la difference
MOMO MERGANE C'est vrai
@@momomergane3140 FG FG hg FG FG FG FG g FG ffffffffffffçfff
Wally le meilleur de sa génération. ❤❤❤
Mashallah laff thiat
Il s’améliore bien machala. Je vois une bonne communication il est posé et répond avec attention aux questions
MashAllah Waly, Pape Cheikh Diallo sa animation lou takh mou nekh moy daguay degue lou tai do dague nit mo takh lepay Nickel...
Merci pape Cheikh ligey bi rafét n'a Yalla n'a sa diamou yague sa khôl bi dara nekou si merci Wally Nice n'a
C k pape cheikh mo rafete hol mok wally nio yam Macha Allah
Bilai danio bakh reck
Masha Allah wally seck liima geunneu nex si waxtaan nam moy dafa posé masha Allah
Mala beugue pire
machalla liep dina bakhe sa khole mo rafete
Thierno Tall très posé et réfléchi vraiment.
Machalla wakh bi rafet na trop Wally émission bi nekh na lol👍
Non suis content merci pape Cheikh ci invitation bingua inviter Wally seck mane dema xeur ci you baniouma Wally mais bene ins comparaison biko Aÿ fans am diko teukeuler ak you moma meti ba deglotoumoko tt en sachant ke ndanane la nn mais crx nanguoul nakoko mais j'aurais aimé ke tfm diko tekk ke momak you niou am link bou Nice mane je comprenais pas le silence de tfm encore moins niak présence you ci Bercy am sachant ke il était invité d'honneur; mais dema contane ci lingua def pape cheikh j'espère ke dou yem fi mais you kene dou yow machallah tes un grand mr nek lene ci diam
Machallah talentueux am respect bonne continuation
Vrement c mangifique yalna diam yague senegal wally ballago seck lepay nice
vraiment je suis content de toi wally gaindee gue
Très fier de vous wally seck continue mon fére
Machallah wally doundal way Wa Arabie saudi daniou lay bègue
Je suis très fiers d'être ton fans Wally Seck jtm piirii boromeu xolou diamant bi
Bravo 👏 Vous avez fait preuve d bcp de professionalism! Joli decor
wally Seck mala beugue ndame rék ngaye ame ❤💎💎💎 nga yoré baye fall pire
Machalla wally seck très fière de ton qu'alla te protège inchalla
Yawe yalla molaye Faye sa khole yalla nala yalla dolli diappalé
Merci PAPE CHEIKH Diallo borom xolou diamant bi
Beau géant homme de caractère le roi du mbalax coeur ouvert que Dieu veille sur vous wally number one je vous souhaite tout sauf le malheur
Mali sidiki diebate côté d'Ivoire dj arafa Ginne Gandia kora Sénégal wally seck nouvelles générations mome la
Lou lére frére
@@modoundiaye2500 nouvelles générations bi mome wally la ndogal yalla soko nane ko do sonou bilahi
sidiki diabaté et dj arafat sont ds artistes international waly seck casamance la yem
Abdoul Bocoum dj arafat et sidiki ont-ils eu des distinctions que wally n’a pas eu ?! Ont-ils fait bercy ou zenith ? N’importe quoi ! Iow mom sokhor mola diap ! Wally est un senegalais comme toi encourage ko moguen
@@Junior-kalish ki diaroul tontou parce que dou sénégalais motakh mou sokhor mais sénégalais bokham ni yalla rék motakh ngaye wakh te sokhoro bilahi nouvelles générations bi wally moy sen baye
Wally B Seck ❤️ pape cheikh beugg nala a partir d aujourd’hui wally il est courageux
Nio bokou wakh pape cheikh beuggeu nala
Machallah Wally seck Nice na torop
Beugu nala barki SERIGNE Touba yalnala YAlla sam arr la
Bonne continuation
Merci pape cheikh
Mon fils dal est le meilleur machalla yalla na ko yalla lafal thiat dal
Machalla Waly et pape cheikh khole seed na bilahi yalna diam yague
Machallah 0faute Waly, Machallah encore vous communiquer bien
Wally machalla merci pape cheikh
Merci a wally seck yalla na la yalla defal la diamou ak niépou
Cette vidéo me motive ❤️🇸🇳
Thiey mar sama xol sedatiina ci yow💗😍 contanatiina deii ! Danga néxxa beug ndahh bagn la beugué batay meuussognou tékk gaathié nous tes Fan au contraire💗💗💗! Amaal jaam rek iow goudou faane ak weer Mar yacine Meissa Bigué yalna sa jaam yague Faramareene bii😍😍😍👏👏👏👏
wakhouma sakh waly mai pape cheikh niit kou bakh man j estime machalah ne change jamais
Merci pape cheikh Diallo waly ci kaw ci kanam faramareen douniou meussa khadi douniou bougè yoto jtm😘😘
Machalla lawelaaaaaaaaaaaaaa thiatttttttttttttttttte thia bamou dalagoul sama domou kholllllllllllllllllll thia khawe thia khaname rekkkkkkkk inchalla yalla nala yalla samale boppame sur tout amineeeeeeeeeeeeeeeee ya rabbi
Wally de love you ❤❤❤