QUARTIER GENERAL du 24 MAI 2019 - Invité : Serigne Gana Mésséré - PARTIE 2

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 янв 2025

Комментарии • 4 тыс.

  • @fallousalihou758
    @fallousalihou758 5 лет назад +553

    Pape Cheikh Diallo ak wa palato bi niepou Yalla naléne Serigne Touba fayy🙏niongui geuneu doli di Sante Serigne Touba mom mi nga kham né I'slam bi rek la done xexal beugue niepou am diamou Bamba Merci🙏

  • @Pablolodja
    @Pablolodja 5 лет назад +430

    Dieureudieufé serigne touba mbacke je suis FIÈRE D'ÊTRE MOURIDE sadikh sante na yalla bou bah bima boké thi ndiabotou ahmadoul khadim le serviteur du mouridisme ahmadoul khadim rekk mognou diaralll tokk si tèlè ba 4h du matin serigne gana yaw serigne touba mbacke molay fayale bopame

  • @mouhagaye1079
    @mouhagaye1079 5 лет назад +704

    Je suis tidiane ms j'aime beaucoup serigne mourtada émission bi nekh n'a trop

  • @omarsall9821
    @omarsall9821 4 года назад +48

    Barkee Serigne Bamba waxtane bi douma thi doyal moukou😭😭😭😭😭Serigne Mountaha mbacke mom la touder sama taw bou goor dei avant mouy nekk khalifa generale, yalla na goudou fane ak werr amine

  • @ndeyesylla3531
    @ndeyesylla3531 5 лет назад +412

    Bou beugue serigne touba té woolouko 1000 j'aime

  • @voyageautourdumondesn
    @voyageautourdumondesn 5 лет назад +2817

    Combien de j'aime pour serigne Ganna massere touche j'aime👍🌍thibarké serigne touba

  • @vieuxfaragaye9511
    @vieuxfaragaye9511 5 лет назад +789

    Moi je suis tidiane mais Gana m'a séduit franchement j'aime beaucoup Serigne touba mbacke

    • @ZeynabRassoul1
      @ZeynabRassoul1 5 лет назад +9

      Bokalé ak soss rék. Ay talibé lagnouy weur. Competir rk lagnou fi néké. Et ne dis plus je suis tidiane ou niassen ou autres. Wakhal say wakh rk. Gnii ay marireuno lagn

    • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
      @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 лет назад +6

      @@ZeynabRassoul1 *_non sérieux iow bakhô😑_*

    • @elbassirelbassir1792
      @elbassirelbassir1792 5 лет назад +12

      Vieux bilahi ya wakh dueg leep fa yalla la nio book seydina mouhamed deiuradeuf serigne touba

    • @papadiene7381
      @papadiene7381 5 лет назад +29

      zeynab mè yaw com yoro kholou dioulit lan ngay cètan mè bilahi bocoy deglou doco tay yaangi deglou sa khol bh di bax nga continue di deglou manosi dra yaw domou iblis nga kep kou beug el hadji malick tamoy deug si yaw mano bagn s touba yaw mom kholal lènèn mè do tidian tidian day am khol bou rafèt yalna yalla fayalniou sounio mak yep dieura dieufat s touba

    • @chiekhembengue4541
      @chiekhembengue4541 5 лет назад +8

      Diadieuf S touba

  • @tiyidekemet7300
    @tiyidekemet7300 3 года назад +23

    Qui est encore là en 2021, novembre 2021 et je suis encore là.
    Et je serai encore et encore toujours là.
    La vidéo qui à changé ma vie. Dieuredieuf Yala santenaniou Serigne Touba môme mi niou wonne. Nouniouye beugué Yonene Mohamed SAWS ak niniouye dooné soldaaram.

  • @xaviernzale9438
    @xaviernzale9438 5 лет назад +263

    Je suis Chretien mais Serigne Touba ma montre la voix.. Louma meussoul dall moy daanou léer Damay toub nek mouride

    • @cestmoitkt527
      @cestmoitkt527 5 лет назад +15

      Xavier Nzalé ay waay fais le vite serigne touba sera très content de vous bienvenu entre nous

    • @tiyidekemet7300
      @tiyidekemet7300 4 года назад +13

      Macha Allha. Bienvenue a toi. Serigne Touba amoul morome té dou tasse yakar

    • @mariombaye8996
      @mariombaye8996 4 года назад +3

      Ndaysann

    • @faxxx8273
      @faxxx8273 4 года назад +6

      Bienvenu s touba kénla

    • @modoupouye7041
      @modoupouye7041 4 года назад +6

      Kou bakh ziar mba moudjé nga toub

  • @aissatoundiaye6878
    @aissatoundiaye6878 5 лет назад +250

    Notre plus grande richesse c est d avoir serigne touba 🙏
    Dieureudieuf borom touba
    Fière d être mouride jusqu'a la mort✌💟

  • @senegaldakar4739
    @senegaldakar4739 5 лет назад +172

    Youssou ndour borom tfm yalla nala yalla Faye, dieureudieuf serigne touba, alhamdoulilah, alhamdoulilah, alhamdoulilah

  • @adandoye3759
    @adandoye3759 2 года назад +104

    Après 3 ans 2019 / 2022 je regarde encore cette émission comme si c’était en direct ♥️🥰😍😍😍😍 Dieureudieufety cheikh AHMADOU khadimou Rassoul 😭😭😭😭😭🙏🏾

    • @emilieguisse8365
      @emilieguisse8365 2 года назад +6

      Je ne suis po la seul alors jeureujeufe borom TOUBA

    • @maguatteloucoubar8179
      @maguatteloucoubar8179 2 года назад +4

      Mm Mane😭🥰

    • @diopweuss9141
      @diopweuss9141 Год назад +4

      2023

    • @adjadosso1263
      @adjadosso1263 Год назад +8

      Aujourd’hui c 4 avril 2023 a 04h jusqu’à 5h j suis là regarde damay setane kom lou bess walahi dieureu djeufè ahmadou

    • @adandoye3759
      @adandoye3759 Год назад +2

      @@adjadosso1263 mashallah 🥰 yalla ngako yageu setane 🙏🏾 si CHEÎKHOUNA AHMADOUL khadim

  • @planeterire2020
    @planeterire2020 5 лет назад +49

    Dieureudieuf SERIGNE TOUBA kouko wakhoul goreiwo.. yaw mi beug SERIGNE TOUBA beuseul jaime

  • @mamyfall5879
    @mamyfall5879 5 лет назад +126

    TFM raw nguene baye cheikh raw nga yalla nalene yalla sameu tei fayal niou Cheikhoul Khadim ci barkei sopeim ba Seydina Mouhamed Salala khou aleywasalam

  • @glasseafiakandji4047
    @glasseafiakandji4047 5 лет назад +751

    Ni serigne touba méloon si yonénté bi nonou la mouride yii mél si mome
    Kouthi and pouce j aime

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818 2 года назад +36

    "Ma poésie à été embellie par l'apologie de ce que j'immite et j'attends de cette apologie toute élévation possible " Dieureudieuf serigne touba

  • @ismadiop7298
    @ismadiop7298 5 лет назад +344

    Ana kan ci yèn mo beuge serigne touba tèkk ko FI.?

  • @xxxrokiagueye4998
    @xxxrokiagueye4998 5 лет назад +1667

    Kou beug serigne touba besseul j aime🙏❤

  • @dethiebamba4
    @dethiebamba4 5 лет назад +650

    Yow mi giss sama commentaire yalna yAAllah fatie sa adio Barki Khadim Rassoul

  • @cheikhsano8453
    @cheikhsano8453 3 года назад +61

    Sérieux je ne peus m'empêcher de regarder cette emission encore et encore Dieuredieufer CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL❤️🙏🏾

    • @mohamedcisse863
      @mohamedcisse863 3 года назад +1

      Amoul morom dé yalla khamnako mom thi dieummeum khamnako wallahil haziim ❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Serigne Touba amoul morom dé saway bakhna rk

  • @BenHalil73
    @BenHalil73 5 лет назад +1416

    Kou geum serigne touba té yaakar ko beusseul j'aime

  • @amadououmarba5124
    @amadououmarba5124 5 лет назад +204

    Alhamdoulilah rabbil Alamine je suis Tidiane mais je suis très content d'écouter cette histoire émouvant, la vie de saint homme qui a uniquement souffert pour l'islam, lui et tous les autres saints du pays, Ces grands hommes méritent l'honneur mais pas la haine, que leurs disciplines suivent leurs pas mashallah

  • @ndiayegueyediaw131
    @ndiayegueyediaw131 5 лет назад +43

    Machalla mane dè js8 layene wayé hier serigne gana mésséré lalena kholou dioulite yeup khamal nagnu bou bakh kane moy cheikhoul khadim khamal nga h'islam la kharal motakh kép kouy dioulite amél nako djoukeul dieureudieuf cheikhoul khadim mbacké balla khol yeup sédna❤❤❤

  • @kazalikaofficial8880
    @kazalikaofficial8880 Год назад +23

    Dioynaa ba sone thiey serigne touba kouko sêtane 2023 rk beseul jaime

  • @sopeyxassidayirek5368
    @sopeyxassidayirek5368 5 лет назад +1759

    ay way komay santélé serigne touba abonné si sopey xassida yi rek

    • @amadoukeita2822
      @amadoukeita2822 5 лет назад +10

      Dieureudieufé Serigne Serigne Touba Alhamdoulilah

    • @sarahwaly5256
      @sarahwaly5256 5 лет назад +8

      Alkhamdou baniou ku tedd kii tannei dieureufeuti borom touba

    • @moustaphaastougueye633
      @moustaphaastougueye633 5 лет назад +6

      Dieureudieufati serign touba khadimoul rassoul sounou yakar fii ak faniou dieum

    • @mourtadaseye6664
      @mourtadaseye6664 5 лет назад +5

      Akssa santè ko rek mo wooŕ

    • @assfall8607
      @assfall8607 5 лет назад +1

      Àbonne na

  • @massethies8537
    @massethies8537 5 лет назад +58

    Pape cheikh Diallo yaw koudèm nga dème kou démoule nga dème Serigne bi békna😍😍yalle nala serigne fallou sa wadia same🙏🏾🙏🏾si barkèp khassida yii❤❤

  • @matarsambou4175
    @matarsambou4175 5 лет назад +534

    je Suis tidiane mais J'aime bien Serigne Touba Machallah Serigne Gana Doundall et Serigne Khadim kébé yanna yalla werrall batte bi

    • @ndiayendiaye4517
      @ndiayendiaye4517 5 лет назад +2

      Amine

    • @mbayediop865
      @mbayediop865 5 лет назад +3

      Dieuredieuf serigne Matar Sambou yalla nala serigne touba dimbali bubax barekp xassidayi

    • @moussaane3822
      @moussaane3822 5 лет назад

      Amna solo

    • @ibaba3388
      @ibaba3388 5 лет назад +1

      Jeureujeuff..ya bah way...serigne touba leugnou beugueu..kouko beugueu beugueu naniou leu!! Jeureujeuff

    • @lomactarmodou6418
      @lomactarmodou6418 5 лет назад

      Amine

  • @zenagogo6494
    @zenagogo6494 4 года назад +172

    Je suis Juif mais Bamba est une lumière Difficile à connaître. Il m’a donné la voix de la Paradis✨ Merci Bamba 👊🏼

  • @sambadiop4175
    @sambadiop4175 5 лет назад +39

    Ayway ma beugue serigne touba ba diekh si mome takk kouko beugue nguir yalla defal j’aime 👍🏻

  • @oumardanieladams7586
    @oumardanieladams7586 5 лет назад +332

    KEEP KOU NANGOUL SERIGN TOUBA LIKO YALLA MAY.KEEP KOOY WAKH DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL.appuis sur j'aime.YALLA DEFAL NIEUP TAWFEKH CI BARKÉ S.TOUBA

    • @awakeita7962
      @awakeita7962 5 лет назад +1

      Ken dou mome Akhmadou

    • @elasfall3637
      @elasfall3637 4 года назад +1

      Déwéne nagne indy ablaye bichri

  • @ibaba3388
    @ibaba3388 5 лет назад +104

    Thiey serigne touba!!!! Kou beugueu kou tedeu ki beusseul Jaime ❤

  • @dametaaal3125
    @dametaaal3125 4 года назад +91

    Weer Rou koor Daw ba Réen gakoy setan beussal j'aime 👍🏾 ❤️

  • @natoucha1946
    @natoucha1946 5 лет назад +148

    Mane dhé sante na yala bamou ma déffé mourid djieureudieuf ser touba 😍❤❤

  • @morniang4764
    @morniang4764 5 лет назад +173

    dieureuf serigne touba, diadieuf gana méséré, pape cheikh yalla nalla yalla lafal thiate té samala si barké seydina mouhamed

  • @adamathiam4800
    @adamathiam4800 5 лет назад +285

    Serigne gana messere yalnako serigne touba fayal boppam🙏❤😭

  • @enzotamba2411
    @enzotamba2411 4 года назад +52

    Koukay setane apres 11 mois di bègue kom mane (Akhmadou Bamba Mognou Goorèl Deh )❤🤲👌

  • @bayendiagaseck4104
    @bayendiagaseck4104 5 лет назад +493

    Tay mom commentaires yiiii koumou nekh wouté serigne bi ay j'aime pouce bleu may guiss

    • @dlyt4209
      @dlyt4209 5 лет назад +11

      serigne ganna mesere yalla nala serigne touba faye kou kontansi serigne ganna mesere beuseul jem😭

  • @mamemodou2414
    @mamemodou2414 5 лет назад +615

    Kou beugue serigne ganna beusseul pouce bleu

  • @dansetv4307
    @dansetv4307 5 лет назад +81

    J sh8 tidiane et fier talibe serigne babacar sy mais j'ai même pleuré pour l'histoire de serigne touba li rèk warna takh gnou geuneu meuna mougne

    • @ibaba3388
      @ibaba3388 5 лет назад

      Ya bah way..te niaka kignane..
      Jeureujeuff
      Bilahi serigne touba sameu serigne bou bahbi hero national leu...

  • @laminecisse604
    @laminecisse604 4 года назад +40

    Présque 1ans Chaque Jours Mougni Gueneu nékh. Wakhtane Bi.Je S8 Tidjan Mais j l'aime Beaucoup S Touba Yanna Fi yalla dieullé Corona bi Barkép S Touba. J S8 fiért d'être Sénégalais ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏼🙏🏼

  • @beuguserignefallou1966
    @beuguserignefallou1966 5 лет назад +66

    Khana nak lou way sokhar sokhar war ngua mana ndangou serigne touba liko yalla deff..yalla nanou ko yalla fayal seengal tay bou nékhé serigne touba KHADIMOU rassoul la..

  • @santyalla5282
    @santyalla5282 5 лет назад +717

    Bravo Outaz Pape Hann 🙏🏿🙏🏿😍😍moi j'ai bien aimé votre présence. Tiëy Serigne Touba.

  • @sidibarhamatraore293
    @sidibarhamatraore293 5 лет назад +303

    Mane mom je suis talibé baye Niass mais j'aime bien Serigne Touba ak wa keureum j'aime les mourides ndah dagno fokou sen Serigne.Machalah

  • @aminatagueyediagne9109
    @aminatagueyediagne9109 4 года назад +25

    Dieureudieuf serigne TOUBA MBACKÉ amoul morom je suis fière d'être mourides j'aime vraiment cheikh akhmadou BAMBA merci à serigne ganna messere 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @papemalickdiouf3743
    @papemalickdiouf3743 5 лет назад +560

    Ay wayyy donnez moi 1000 j'aime pour adiyyah de ganna

  • @boyedemlofficiel5376
    @boyedemlofficiel5376 5 лет назад +787

    Meilleur émission QG tout les temps vraiment tfm gagné nguen émission bi amoul kou nangou woul nak basta lep lerna diuera dieuf serigne touba ❤

    • @sokhnamaimouserignesaliou1906
      @sokhnamaimouserignesaliou1906 5 лет назад +14

      Billay naggou rkk
      Dieureudieuf Serigne Touba
      Amoul morom

    • @modoukebe6050
      @modoukebe6050 5 лет назад +8

      Dieureudieuff ahmadou

    • @aissatousow5336
      @aissatousow5336 5 лет назад +6

      Machallah Serigne touba

    • @ZeynabRassoul1
      @ZeynabRassoul1 5 лет назад +4

      Serigne Touba dafa begone yalla ak yonente bi ba yamalé wouko ak dara, mais talibé yi dagno wara topou yalla ak yonente bi, diko diamou, té bayi bokalé bi, ak garouwalé bi ak soss yi. Sakou djiléne xam xam, khami sa borom. Serigne touba momoul adouna bi, dou yalla, dou yonente, Nit la comme gneup. Bayilén competir bi té diamou dji yalla. Wa salam

    • @fatoundiaye8224
      @fatoundiaye8224 5 лет назад +8

      @@ZeynabRassoul1 mourid aka rafet khol dounu xas kenne

  • @meilleurtiktok6517
    @meilleurtiktok6517 5 лет назад +131

    Machalla xole sédatina..kép kou aime yalla Serigne bi fadji Say adioo

  • @mamediarragueye1331
    @mamediarragueye1331 3 года назад +51

    Longue vie à toi serigne gana et à tte l’équipe ❤️🙏🏾

  • @astoundiaye2431
    @astoundiaye2431 5 лет назад +54

    Je ne sais pas ce que j’ai mais il ne se passe pas une nuit où je ne ré-regarde l’émission pour dormir et ce depuis sa diffusion.
    Merci pour cet apaisement du cœur.
    Dieureudieuf SerigneTouba!

  • @adjafall4707
    @adjafall4707 5 лет назад +16

    Meilleur emission QG serigne Gana yalnako serigne Touba faye fier d'etre Mouridisme dieureudieufé Borom touba souniou yakar tay ak euleuk

  • @xaviernzale9438
    @xaviernzale9438 5 лет назад +379

    Ay way Beuslène j'aime kou beug Serigne Touba

    • @mallawagne4018
      @mallawagne4018 3 года назад

      💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞

  • @moussabayo8554
    @moussabayo8554 4 года назад +79

    Kou geum nii Serigne touba kénn leuh ci Diamano beusseul J'aime

  • @thiamtouba9569
    @thiamtouba9569 5 лет назад +46

    Machallah TFM YALLA NA SERIGNE TOUBA FAYLÈNE CI BARKÉ WEERU KOOR GUI

  • @babacardieng3315
    @babacardieng3315 5 лет назад +17

    Serigne Gana mèssère yalla nala yalla faye. La meilleur èmission que la tfm n,ait jamais produit. Cette èmission a drainè un auditorat inestimable et a mobilisè toute la population senegalaise en èveil jusqu,a l,aube. Lii lep serigne touba CHEIKH AHMADOU BAMBA moko waral bilay kène dou mom

  • @Sancoun43
    @Sancoun43 5 лет назад +162

    Aimer nguir kénnal Serigne Touba, Khadimou Rassoul,Cheikh Ahmadou Mbacké, Cheikhoul Khadim😭❤️🙏

  • @momarmangane8617
    @momarmangane8617 Год назад +4

    I can’t watch enough this QG. The best ever!!! Thanks 🙏 Pap Cheikh.

  • @naruuserigneamsatoumbacke5141
    @naruuserigneamsatoumbacke5141 5 лет назад +56

    Assalamu aleykoum serigne gana yallah nagua fi yagg tei werr waxtane wi mom machaalah di sackou yeineine rek nguir dieumi SERIGNE TUUBA 😭

  • @fatoundiaye7305
    @fatoundiaye7305 4 года назад +110

    Ramadan 2020 qui es d'accord pour bénéne émission spéciale ment chekhoule khadim

  • @amintagueye2370
    @amintagueye2370 5 лет назад +280

    Kou yakar serigne touba beusseul j,aime

  • @moizaf5516
    @moizaf5516 Год назад +3

    Serigne Touba keneu la ☝🏻 aujourd’hui septembre 2023 kouko nangou lalale j’aime

  • @modoufall6512
    @modoufall6512 5 лет назад +2344

    Yaw mi djiss sama commentaire bi bo beugué Serigne TOUBA touche J aime

  • @khadyndao2655
    @khadyndao2655 5 лет назад +23

    Amoul secret lep serigne touba lah🙏❤️ Yalla naniou ko yalla fayal🙏❤️👌

  • @aidafall7696
    @aidafall7696 5 лет назад +53

    Serigne rek moy deuge kène dou mome allkhamdoulilah fiere d etre MOURIDE DIEUREDIEUFEUTI KOU TÈDD KI❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seyendeyepeinda6741
    @seyendeyepeinda6741 2 месяца назад +1

    Grâce à sama kharite gane j ai découvert beaucoup de choses sur la vie de SERIGNE TOUBA sante yalla bou bakhe goude fane

  • @mamygueye822
    @mamygueye822 4 года назад +402

    Ki regarde ça en 2020? Mashallah Dieureudieufeti Cheikhoul Khadim

  • @binetacamara9496
    @binetacamara9496 5 лет назад +242

    😭😭😭😭😭😭j'ai pleuré toutes les larmes de mon corps,bilahi Cheikhoul Khadim beugue leu dafa di farata si gnoune,🤲❤🙏🙏🙏

    • @modoufaye4229
      @modoufaye4229 5 лет назад +2

      Mmjm6jmujjjjjmjjjjmjmjmmjmjmjjjjyjjj
      nmjyjjjmjjjjmmjjjmjjmjmjjjyymjjmjjj
      Jjjjj myyjmmyjjjmjjjjjyjjjyjmjjjjmjyjuyjjjmjjjmyyjyjjjyjjjj yjmmmmjjjuymmmmuyjyj myjjujmyyjjjjjmyjjjjjjjmmjjjjjmymyjjmjjjjyyymujmyjjjymmjjjjymuyjy2k jmyyyjmyymjyjymuyjjmumjjjjjyjjumujmyjjjjjjjmymjjjjmmyyjmjujmmhyjjjjjjmumyjjmjmymjuyjjjjjmumjmyjjymmymymjyjjjjyjjmuujyjjmyjjj

    • @lassanadoucoure6586
      @lassanadoucoure6586 5 лет назад

      T'es sûre que t a pleuré?

    • @beuguefallou6555
      @beuguefallou6555 5 лет назад +3

      Bilahi farata la si gnoune

    • @senegalrek7975
      @senegalrek7975 5 лет назад +3

      Binta je taime

  • @deguenesarre2714
    @deguenesarre2714 5 лет назад +78

    Serigne Touba rék la yakar kouko beugu beuseul j'aime

  • @astoudiouf1679
    @astoudiouf1679 2 года назад +8

    Machalla 2023 je regarde encore cette émission 🥰🥰🥰 Dieureudieuf Cheikhoul Khadim👌🏾❤️

  • @mayibwayal3760
    @mayibwayal3760 5 лет назад +743

    Je suis tidiane mai yalla nanio yalla fayal sonou mame brom touba RTA ❤️🙏

  • @fatoulo4530
    @fatoulo4530 5 лет назад +96

    Dieudieufé Serigne Touba amoul morome té kéne dou mome🥰

    • @bambangom729
      @bambangom729 5 лет назад

      Kounioukoy tekeulele niogui lay nax

  • @codoufalloufaye1561
    @codoufalloufaye1561 5 лет назад +165

    QG teudj na ba déwéén. Allahou akbar.SERIGNE Touba amoul morome waay .eyy khol fekh na démb 😍😍😍

    • @niakhanambissane9448
      @niakhanambissane9448 5 лет назад +4

      J'AIME

    • @moustaphajack5994
      @moustaphajack5994 5 лет назад +3

      Dieure dieufé s touba li Anma solo lole ndah s.touba pour dioulit yeupoule ta képou kouy senegale dagua wara kham Lila s.touba défal ndah toukibi métiwona lole ta dioulit rék ladone dimbalé bimouy délousi tamit limouwah moy Yalla fidi Senegal képou koufiy yéwo tayakar rasululahi boueulegué yaw Yalla nagualén djéguel kone nieupe co bok con tfm liguén défni Lou wara amla wérwouné ndah kounou wara khamla nome s.touba mane mourid la wayé dama yéné képou kouy dioulit diariniou si s.touba rawatina Senegaléyi amoud léne si tarih louniou wara hamlé si Senegal ta djitalounousi s.touba cone tfm diarama🙏🙏🙏

  • @bassiroudiallo9740
    @bassiroudiallo9740 Год назад +2

    Solution moyi serigne Touba
    Bamba thank you
    ❤❤❤❤❤

  • @mamediarraboussoquincaille4807
    @mamediarraboussoquincaille4807 5 лет назад +59

    merci GFM Encor une fois rewmi nieppa wara dellou dioukkal serigne touba yalla nanio kou sunu borom fayal barkep ramadan

  • @mamekhadimdiop10
    @mamekhadimdiop10 5 лет назад +1121

    Ayy wayy guirr yallah QG dolène deffat béne émission spéciale Serigne Touba Balla koor guii di diex Koussi Daccor beusseul jaim si dieumi cheikhoul Khadim

  • @gverr6tti38
    @gverr6tti38 5 лет назад +97

    Thieuy Seigne touba😍démb kholl yeup tooy naa
    Serigne Gana Messere yalla na yalla faye si barké Borom Touba

  • @cheikhomarseck6071
    @cheikhomarseck6071 10 месяцев назад +1

    Dieureudiefety Serigne Touba mbacké diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Serigne Moune takha Mbacké yakifie lolle té wére❤❤❤❤❤❤ je suis fière d'être mouride ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Motivations20242
    @Motivations20242 5 лет назад +44

    Bismilakhi Rakhmani Rakhimi barkep Dialibatou Marakhib Dieureudieufei ti BOROM TOUBA Di Niane kep kou téwé émission bi yalnako Serigne Touba fayale bopam ci barkep MASSALIKOUL DJINANE

  • @adjadiop1264
    @adjadiop1264 5 лет назад +71

    WA gni aimé woul Lou neikh li esk ay nit lagnou tamitt amolein xol deii 😭😢dieureudieuf serigne touba🙏🙏❤️❤️❤️😥🙏🙏🙏🙏

  • @adodiouf2657
    @adodiouf2657 5 лет назад +36

    Serigne Touba dou Yalla dou Yonétti .....Serigne Touba la kénn xamoul loumou donnee .........DIEUREDIEUFÈ TÉ BROME TOUBA...❤...DIARRAMA CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @wiiziimaker1892
    @wiiziimaker1892 4 года назад +24

    Serigne TOUBA💟 amoule morome ❤️Bilahi keneu d’où môme 💕Yalla naniou Yalla sakhall si yonou Mouride❤️❤️🙏🏽

  • @thiandoumserignembaye9872
    @thiandoumserignembaye9872 5 лет назад +140

    J'ai le cœur qui déborde de joie SERIGNE TOUBA mérite amplement son universalité , un Homme (en apparence)de paix, un Guide, un dictionnaire de bons comportements son indulgence est sans limites Ah ce KHadimou Rassoul !!!

  • @talibeserignemassamba7678
    @talibeserignemassamba7678 5 лет назад +51

    Ouhhhhh gana beuguel nga mourit yep machallah li nga wax si s massamba nexna tarkalah

  • @ramatoulayebousso2505
    @ramatoulayebousso2505 5 лет назад +25

    Mane wakh beugeu na koumay wakh xam xam si Serigne Touba té Serigne Gana mii xam xam lay wakh Mashallah yalnala yallah faye 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @mignonemama4512
    @mignonemama4512 3 года назад +5

    2021? Doumaci doyal mk Kén dou Cheikhoul Khadim amoul morom. Ganna Mésséré Yalna fi yagg tei ande ak Wéér
    Amine

  • @sallndeya2285
    @sallndeya2285 5 лет назад +248

    D'où yena ngi deg? Serign touba liko rasoulilahi diaral! WA Salam !

  • @doudoutoure4973
    @doudoutoure4973 5 лет назад +331

    3 fois makoy sêtanaat Ken Cheikhoul Khadim 😭❤️

    • @ndongomboup7518
      @ndongomboup7518 5 лет назад +2

      Akassa Ahmadou Bamba ken la

    • @koudysy8556
      @koudysy8556 4 года назад +1

      Dieureudieufè serigne touba Yalla nagnouko Yalla fayale

  • @minelabambiste9258
    @minelabambiste9258 5 лет назад +50

    Xole séd na yale na diam yag si barké serignie touba kou sa xole nékh beusal j'aime

  • @abdoulayendiguesene8019
    @abdoulayendiguesene8019 4 года назад +11

    Daniouy bakhantal
    Dieureudieuff Serigne Bamba🙏🏾🙏🏾🙏🏾
    Qui est là thie Ramadan 2020

  • @sonhiboufall1979
    @sonhiboufall1979 5 лет назад +67

    ALHAMDOU LILLAH binou amé serigne TOUBA KHADIM RASSOULLAHI ❤

  • @BAMBISTETV
    @BAMBISTETV 5 лет назад +54

    Dieuredieuf serigne touba Dieuredieuf borom touba Dieuredieuf cheikh ahmadou bamba khadimoul rassoul
    Diotay bou cheikh ahmadou kara tambali mom fawwu mou nekh tawfekh mociy diek moudji ci

  • @fatimatasarr5113
    @fatimatasarr5113 5 лет назад +216

    Je l'ai regardé plus de 20 fois ti doya louma , Dieureudieuf Chekhoul Khadimal😍

  • @Linguere00221
    @Linguere00221 2 года назад +6

    Ki regarde toujours cette vidéo même 3 ans plus tatd?
    2022 et je ne me lasse pas de cet QG spécial Khadimou Rassoul ken dou Serigne Touba

  • @salladia2888
    @salladia2888 5 лет назад +26

    Masha Allah. Il m'a fait pleurer. Incha allah une fois au Sénégal, je vais acheter un livre qui parle de l'histoire de cheikh akhmadou Bamba. Ken dou mome

    • @yayakane7951
      @yayakane7951 5 лет назад +2

      Wawaw Salla dinasi âme solo digua âme lo khame si môme Waya lamou done deugue yomboul gua khameko

    • @groupetgs6428
      @groupetgs6428 5 лет назад +4

      Salla Dia salam sokhnasi envoie moi ton e-mail je vous envoie quelques livres de CHEIKH AHMADOU BAMBA en Pdf

    • @groupetgs6428
      @groupetgs6428 5 лет назад +1

      www.daaraykamil.com

    • @groupetgs6428
      @groupetgs6428 5 лет назад +1

      www.jazbu.com

    • @cheikhdiakhate8325
      @cheikhdiakhate8325 5 лет назад

      Naamat tay way émission bi

  • @FatouNdiaye-ck5pr
    @FatouNdiaye-ck5pr 5 лет назад +40

    Je suis tellement fière d'être mouride💝 Alahou akbar😢

    • @biramemboup7676
      @biramemboup7676 5 лет назад +2

      @Zedou c'est comme si demand3 tu es senegalais ou Africain? Vraiment wakhi doff

    • @FatouNdiaye-ck5pr
      @FatouNdiaye-ck5pr 5 лет назад +2

      @@biramemboup7676 merci👍👍

  • @thiattdiene9016
    @thiattdiene9016 5 лет назад +474

    Fière D'être musulmane
    Fière d'être Mouride
    Fière d'être Talibé Serigne Touba
    Fière d'être seutou Cheikh Issa Diéne❤❤

  • @mamadulamiinjoob9541
    @mamadulamiinjoob9541 3 года назад +8

    Combien de j aime👍 pour Serigne Touba Ahmadou borom diam yi

    • @omarsagna6076
      @omarsagna6076 3 года назад +1

      yalla moy borome jameu yi

    • @mamadulamiinjoob9541
      @mamadulamiinjoob9541 3 года назад

      @@omarsagna6076 lima wax mane la engager epui yaw momou mola mome mome sa baye

  • @amydiop7665
    @amydiop7665 5 лет назад +53

    Machallah li nekhna lolou way😍
    Dieuredieufé Serigne Touba
    Serigne Gana Masseré yague fi lolou té weer

  • @mbackediagne8575
    @mbackediagne8575 5 лет назад +55

    Serigne ganna messerè yalla nafi yag tè wèr

  • @bambamidadi8184
    @bambamidadi8184 5 лет назад +194

    😭mandé Sant na yalla bou bakh bimouma défé mouride rawatina samay wadiour bimouma toudé serigne touba defama may ndongo dara 😭📿💎yalna niépou am diamu 🤲serigne ganna yague fi lol ta am wérr 🤲diereudieufé serigne mountakha Mbacke 💎👌

  • @falloundiaye5502
    @falloundiaye5502 4 года назад +4

    Je regarde chaque jour cette émission jeûreûjéufff serigne touba Khadimou rassoulilah le sauveur de l'islam bo amoul wone rekk mou niaww