Intégral QG: du 31 MAI 2019 avec Serigne Ahmet Sarr

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 дек 2024

Комментарии • 445

  • @awadembele131
    @awadembele131 5 лет назад +218

    Kou beugue maodo pouc bleu machallah

  • @diopibou9667
    @diopibou9667 5 лет назад +30

    Seydil Hadj Malick ya raw fi ak feulé , merci Ahmed Sarr ya beuri xam xam mashalah

  • @symoustapha5756
    @symoustapha5756 5 лет назад +74

    Machalla nekhna richena ken dou CHIEKH seydil hadji Malick sy kham kham bou werr te leer naniie maodo 🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @elmalick9288
    @elmalick9288 5 лет назад +89

    Yalla nanou yalla fayal Cheikh seydil Hadji Malick... Motakh niou sope seydina Mouhamed ganaw bimou niouke diangale..

  • @omarobah7072
    @omarobah7072 5 лет назад +28

    Maodo mognou xamal kouy yonette big... Wayé Ahmed sorr yagnou khamal kouy mame maodo lingay wakh dou loy lamabatou machallah sarr na yallah fayla yiwww

    • @jamesharden331
      @jamesharden331 5 лет назад +3

      Wakhal way kou bakh yalla nala yalla defal diam

  • @palaisfall9748
    @palaisfall9748 5 лет назад +59

    Machallah mame maodo dou moromou bene serigne si senegal ak liko weer mako wakhe

    • @niangmodou47
      @niangmodou47 5 лет назад +9

      Wakhal way ndakh talibé Mame maodo rék rawna séring sou Bari

    • @papefall776
      @papefall776 5 лет назад +8

      Waxko sa kaw

    • @jamesharden331
      @jamesharden331 5 лет назад +6

      Wakhal si kaw ! Mak yow gno ko wakh

    • @PulaarMedia
      @PulaarMedia 4 года назад +1

      Ba desa cheikh oumar foutiyou tall moko lijagel moko maya tere bala mo jouddu

    • @elhadjiabassba9540
      @elhadjiabassba9540 2 года назад

      Wakh ngua deugeue dėhhhhhhhhhh

  • @mamefansenyndour8536
    @mamefansenyndour8536 3 года назад +5

    Thiey yallah da binde té yamaléwoul barki Seydina mouhemad 😭❤️Mame maodo 🙏

  • @rekdeugue7508
    @rekdeugue7508 5 лет назад +105

    Non Talibé cheikh yiii amnaniou kham kham machaallahhh. Yarou Naniou set Naniou yiw Naniou machaallah !

  • @combecane257
    @combecane257 3 месяца назад +1

    Machala Sy Malick yalna sougnou borom doli ko yeurmandé ak lér té tass gnou si barkém ❤❤❤❤❤❤❤

  • @khalifawade1844
    @khalifawade1844 5 лет назад +64

    Rien a dire wallahi xam xam bi Rafett na kadu yi séleu naa, Maodo ama tina ndam tchi ak jaabotam guimou bayi guinaw; folén tolou yéna ngui rafetal sén diguanté ak bép deukeu ndo ak tariha yi fi nekk manchallah jereujeuf Maodo

  • @atoumanedjamilder9502
    @atoumanedjamilder9502 5 лет назад +25

    Mach Allah xol seddatina. Yallana yalla Yoka soutourayi

  • @bamsbams3171
    @bamsbams3171 5 лет назад +43

    Walh'djé Bari'rek wayé ma'ndou cheikh seydil Hadji Malick Sy dina trokhal niou barri ndakh xam xam AK yar bi téguine yalnagnou'ko yalla fayel si barki seydina mouhamed psl Amine

    • @bayefall6717
      @bayefall6717 5 лет назад

      Yao yay wax kate bii nopile

    • @loritandiaye896
      @loritandiaye896 5 лет назад

      @@bayefall6717 bila wakha tiko moy wakh kat bi di saye tanébi boudé guor gua yeureur na say diabar boudé djiguéne gua tmt yagui diakhasé séne keur nafékh gua trop

    • @jamesharden331
      @jamesharden331 5 лет назад

      Amineee way

    • @allefall4988
      @allefall4988 4 года назад

      @@bayefall6717 yagi mer dhe 🤣🤣🤣talibe cheikh rek ba fawou incha Allah

    • @diopbaps1481
      @diopbaps1481 4 года назад

      @@allefall4988 dafa lerr😂😂🤸‍♂️🤸‍♂️

  • @mamagueye702
    @mamagueye702 5 лет назад +50

    machaallaah,mawdo moo raw amoul morom ken d'où moom yalna yalla fayal gnouko

  • @momocippgueye1392
    @momocippgueye1392 5 лет назад +16

    Magou senegalyi nio bakh ma sa allah yalla nanioulen yalla fayal ta tasnou ci sen barke

  • @oulimataboye9318
    @oulimataboye9318 5 лет назад +12

    Mame thiate you make me cry. I love mame Abdou. I have his picture in my living room in the USA. Americans asking me if he’s my dad. My answer to them” he’s beyond a dad to me”. Mashalaah your voice is just like him.

  • @symbayelevrai8772
    @symbayelevrai8772 5 лет назад +44

    Machalla yarou yatou yiw bari kham kham talib3 cheikh kene d'où nioune

  • @sadjibarrababacar5530
    @sadjibarrababacar5530 5 лет назад +16

    Macha allah cheikh seydi el hadji malick sy yal naniou ko yalla fayal tè tasse niou si barckème

  • @abdoundoye9807
    @abdoundoye9807 3 года назад +5

    Ki est là en 2021?

  • @maramatadiaw2134
    @maramatadiaw2134 5 лет назад +6

    Masha la amna sola smed sarr Sarr yalla na Kodd fan ty weral baye

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 5 лет назад +70

    A 1:37 j'ai failli pleurer c'est la même voix que Mame Dabakh MachaAllah MachaAllah MachaAllah

  • @ndeyefatou6785
    @ndeyefatou6785 5 лет назад +30

    Dieureudieufé maodo khamal nganiou yalla khamalniou yonété bi

  • @ibrahimagueye8519
    @ibrahimagueye8519 5 лет назад +58

    Je suis très content de du niveau de vie intellectuelle de Seydi El hadji malick

  • @الصوفيالتجانيالتواوني

    Allahou akbar seydil haadji malick daal rawna niila wakh da wara téguo ci kham kham ak ay archives waay diaarama SERINGE AHMED SAAR !!!

  • @jesuistoi5172
    @jesuistoi5172 4 года назад +5

    Qui regarde à cette année mais j'aime

  • @sallseynabou2341
    @sallseynabou2341 5 лет назад +38

    Dieureudieuf Mame Maodo El Hadji SY MALICK 🙏🙏🙏

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 5 лет назад +30

    Ndeyssane sunuy serignes folene
    Fek niungui defar digunté. Yalla naniu leneu borom bi fayal

  • @abdoulayengom359
    @abdoulayengom359 5 лет назад +22

    Machallah amna solo loll dieuredieuf serigñe Ahmad Sarr wakhtan bi amna solo loll diangeu reck mo woor

  • @wolimatasene4565
    @wolimatasene4565 5 лет назад +12

    Sama khôl da sed trop
    Sa kham kham celna rouslo wogno yalna yalla goudal sa fann
    Sy Malick yalna yalla yok Say lerr

  • @khadybadji9670
    @khadybadji9670 5 лет назад +8

    mashaa Allah kholl sédatineu walahi yalnagnou yalla fayyall souniou Mame Maodo

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 5 лет назад +22

    MachaAllah talibé cheikh yarou rek té ndeyssane nieup laniu considéré. Alhamdulillah alhamdulillah alhamdulillah

  • @ismaelandiaye3687
    @ismaelandiaye3687 5 лет назад +15

    Macha Allah laff thiate Yalla n'a Yalla fayal niou Seyidil Hadji Malick Sy RTA

  • @aliudiao9144
    @aliudiao9144 5 лет назад +88

    Mane legui dama tayal si comantair yi paceque maodo kholal rek gnimou forme amoul len solen khole doto werente yalnagnou yala fayal maodo

    • @dramesoce8673
      @dramesoce8673 5 лет назад +2

      merci

    • @khalisyll3330
      @khalisyll3330 5 лет назад +1

      Diadieuf

    • @aliudiao9144
      @aliudiao9144 5 лет назад +6

      Maodo mo niane thia cabaga ni yala bouma fegnalfi moug degnethalma ba euleug nico sama talibe boulen kenkhame ak sama ndiabote niko nangmamaye ma tabakh ay diaka aki zawiya nico mayma ma ame foumaye niakhe lou lewe thiaye maodo

    • @aliudiao9144
      @aliudiao9144 5 лет назад +2

      Niakhe loulewe thiaye maodo sama sopebi maodo kou wete nawe ko ndakh selame ak samome

    • @assmalicksy3625
      @assmalicksy3625 5 лет назад +1

      Diaadieuff

  • @aasfatfaatfa5852
    @aasfatfaatfa5852 5 лет назад +9

    Macha allahh ndeye sane walahi alehAmdou lileLAHHH yalla na gnou yalla fayale maodo barki sangame bou tédd mii

  • @awadembele131
    @awadembele131 5 лет назад +28

    Machallah keneu dou cheikhe seydil hadji malick sama khole sedeuna dama beugue maodo

  • @moustaphagueye2376
    @moustaphagueye2376 5 лет назад +10

    Mach'ahlla seringe ngagne mbaye nekh na trop yalla na yalla yokou kham kham bi

  • @farandiaye2964
    @farandiaye2964 5 лет назад +6

    Machallah yalla nagnou yalla dolly fayal seyedil Hadji malick sy mi neubeu bopp ndakh mo déme makka gnane fa yalla yalla bougne ma xam si adouna kouye xeuthioo mboloo dou gnane lolou kéne lagnou dikhogne pour gnou xam ka moye seyedina mohamad SAW té reussire naka kou beugue yonnéne fook ngue beugue maodo lolou la yalla dogual

  • @terraingtf3039
    @terraingtf3039 5 лет назад +8

    Niveau bi yèkna ma sha Allah yalla nalla yalla fayalnioula si barkè maodo rta

  • @papendiaye3968
    @papendiaye3968 5 лет назад +4

    Ahmad attidjani saar yalla nala yalla samm sedal nga kholu djoulitee yeup rawatina nioun ndiabotou tarikha tidjaniya

  • @falloundao
    @falloundao 5 лет назад +10

    Yalla nagnou yalla fayal Cheikh Seydi Hadji Malick Sy

  • @mariemethianesoumah5825
    @mariemethianesoumah5825 5 лет назад +7

    fièr d'être talibé Maodo
    Mashallah gnoune yalla nagnou yalla fayal Seydil Haje Malick Sy RTA ci Barké Seydina Mouhamed sangou sangue yi PSL

  • @ousmanediop1515
    @ousmanediop1515 5 лет назад +13

    Diereudieuf Sarr yalla na yalla barkeil xam xam bi bokk yi kou neik si li ngua neik yalla nassi yalla defal dambe nagnu rafetal kadou yi diohe tieur gnugnu makk yereume Ndaw yi neik des djoulite ba paré Dora sakou tahira

  • @abdoulayefall7362
    @abdoulayefall7362 5 лет назад +22

    Machalla Sénégal nenn sant yalla t diamouko ndegeum seydi hadji malick mot khalat nier fannou bamel assamak ndoun

  • @morgueye2635
    @morgueye2635 5 лет назад +7

    Billahi kham kham req moo âme solo machalla amna Solo

  • @astoundiaye8677
    @astoundiaye8677 5 лет назад +27

    Macha allah wakh tanbi amna solo

  • @serignecisse2573
    @serignecisse2573 3 года назад

    Gayi danio mana fen fen bakhoul DEUG monekh Amet Sarr leral nga lep machaallah l'erna mak dafawara roussa fen

  • @issamamediop1093
    @issamamediop1093 5 лет назад +134

    Sérieux doumassi doyal damakoy setane diko setanate tieuyyy xam xam bilay mo nekh je regrette d'avoir passé du temps à l'école bilay alkhouran moy leup

  • @sidylaminediassediasse9314
    @sidylaminediassediasse9314 4 года назад +9

    Ana ngikoy setane ba legui mane dh doumassi doyal

  • @oulimataboye9318
    @oulimataboye9318 5 лет назад +15

    Thank you for sharing that beautiful knowledge. May Allah rewards all of you. Serigne Ahmet you make me proud being Muslim. Alhamdoulilah.

  • @ibrahimasoumare357
    @ibrahimasoumare357 5 лет назад +8

    Machalla mame maodo sounioula amoul wone founiou dieum sante naniou yalla di diouli si seydina Mouhamed psl lolou la Maodo wakh

  • @amadoudiop1139
    @amadoudiop1139 5 лет назад +57

    Fier detre talibe serigne babacara

  • @thiorothiam2657
    @thiorothiam2657 5 лет назад +19

    Machalla machalla kene dou maodo malick sy

  • @mouamedmbaye4444
    @mouamedmbaye4444 5 лет назад +6

    yalananiou yala fayal mame abdoul aziz sy dabakhhh akabakhhhh yalanala yéssal yeurmandéme thi mom amine

  • @awandiaye161
    @awandiaye161 4 года назад +4

    Yalla na la Yalla feye Seurigne Cheikhe Ahmed Sarr

  • @khadijaba5177
    @khadijaba5177 5 лет назад +19

    MachaAllah 🙏❤Alkhamdoulillah diadiefeti Seydil Hadji Malick❤❤Yalna Allah fayla outaze Ahmed Sarr Yallah yagual sa tahaway1👍

    • @muhammaddiop6779
      @muhammaddiop6779 4 года назад +1

      Khadijia kén d'où seydy khadji malick//782081390

  • @aminatouseck3131
    @aminatouseck3131 5 лет назад +5

    Machalah serigne ahmat sarr kham kham rek guafi wakh dieuré dieuf

  • @awandiaye161
    @awandiaye161 4 года назад +5

    Wallahi doumathi doyal mouke
    Machaallah

  • @oumytall606
    @oumytall606 5 лет назад +20

    MachaAlla li nekh naa thi kol dale

  • @maodomalickthiaw8328
    @maodomalickthiaw8328 5 лет назад +10

    Machallah thieye mame maodo

  • @papendiaye3968
    @papendiaye3968 5 лет назад +3

    Dieureu dieuf Oustaz Ahmad saar écoles Maodo daal lenen la machallah

  • @mouamedmbaye4444
    @mouamedmbaye4444 5 лет назад +35

    Sénégal dotoul am kou melni mom mame dabakhhh manmi wakh ap khadre la walahi gorgogou dotoufi amati

    • @yerimsy8740
      @yerimsy8740 4 года назад

      mouamed Mbaye cheikhna cheikh saad bou néna maodo sa école MO gueune si école yi sa wird MO gueune si wird yi té béppe borom xam xam bouy diranté ak yaw mbague dina niak thieureum ci yallah

  • @ismaelandiaye3687
    @ismaelandiaye3687 5 лет назад +33

    Dieredieuff Serigne Ahmad Sarr charakha lahou sadraka laff thiate Yalla nala Yalla mousal si thiate AK lamigne gouddal sa fane samal la bopam

    • @fatoundiaye9607
      @fatoundiaye9607 5 лет назад +1

      Fière d'être musulmane et talibe serigne babacar sy

  • @amadoukande6567
    @amadoukande6567 5 лет назад +10

    Seydi Hadji Malick Sy yalla yalla yok lèrame macha alla

  • @amathdiallo518
    @amathdiallo518 5 лет назад +31

    Bilahi preuve bocoul ak wakhi késsé cou wédi dafale ni Ahmed sarr var bi léral na lépp

    • @karimgaye4327
      @karimgaye4327 5 лет назад +5

      Amath Diallo wallahii

    • @jamesharden331
      @jamesharden331 5 лет назад +6

      Mdrrr wakhal si kaw ameth diallo sa tourondo bi ameth sarr xam xam bi selna

    • @assmalicksy3625
      @assmalicksy3625 5 лет назад +2

      Nagne😃🤗🤗

  • @astoukhalifa9946
    @astoukhalifa9946 4 года назад +3

    2020??😍😭😭 Thieuy Maodo❤

  • @sowbineta8483
    @sowbineta8483 5 лет назад +15

    Machalla lafethate nice nice talibechiékh

  • @modouniang9416
    @modouniang9416 5 лет назад +1

    Macha alla EL HADJI AHMED SARR YALLA na YALLA yok kham kham bi té fayal gnnoula yak djabotou MAME MAODO ak sougnou wadiour yi té dolignou soutoura S BABACAR SY (rta) point

  • @bintasylla5836
    @bintasylla5836 5 лет назад +3

    Machallah Machallah amna solo merci beaucoup Serigne Ahmed Sarr yallah nala yallah faiye 🙏

  • @adamagaye5774
    @adamagaye5774 5 лет назад +12

    Machalah Sarr Ndiaga léerna nagnii

  • @seynaboufall5583
    @seynaboufall5583 3 года назад

    D'après tout ça,Mame Maodo RTA demeure l'inconnu de la nation comme disait Serigne CHEIKH Al Makhtoum RTA. Tieuy Seydi Elhadj tek nga nou si yonou deug ak leer machalah. Yalna Yalla fayal niouleu 🙏🙏🙏

  • @serignethieng8966
    @serignethieng8966 5 лет назад +12

    Machalah jarrama seydy hadj malick sy

  • @maremediop9166
    @maremediop9166 5 лет назад +34

    Mame maodo motah gnou beugeu ki yalla guena beug té kouko beug téde Mouy rassouloulay

  • @justicepourtous6168
    @justicepourtous6168 5 лет назад +8

    Aaah Mame Maodo way sama khol 💖❤💖💖💖❤❤💚💙💜💛❤❤

  • @manoumanou3800
    @manoumanou3800 5 лет назад +1

    Dieureuf mame maodo Malick yalla naniouko Yalla fayal guendi fay si barkei Sopey bi Seydina Mouhamed PSL

  • @mouhamethndawndaw9107
    @mouhamethndawndaw9107 4 года назад +1

    Yall na yalla goudall sa fane waye machallah 💯🇸🇳😍

  • @babacartoure5191
    @babacartoure5191 5 лет назад +4

    Yalla naniou yalla fayal elhaji Malick Sy 😍💑♥️♥️♥️♥️♥️

  • @ndeyesarr2415
    @ndeyesarr2415 5 лет назад +18

    Machallah ❤yii sédatina yalla niu yalla fayalll Mame Maodo 🤲🤲🤲

  • @monsieursy7792
    @monsieursy7792 5 лет назад +18

    Walahi ndeysann kén dou sama Mame Cheikh Seydil Hadji Malick yal naniouko Yalla fayal Sy Malick🙏🙏❤❤❤❤

  • @jabousarr1490
    @jabousarr1490 5 лет назад +5

    Ma shaa Allah
    Serigne Ahmad Sarr🤲🤲🤲🤲😭🤗😭😭

  • @dioumabahnice5465
    @dioumabahnice5465 5 лет назад +19

    Billahi kèndou maodo

  • @fatimasoumare8407
    @fatimasoumare8407 5 лет назад +9

    Fatiha salatoul fatiha ❤🤲

  • @vieuxsarrbadiane2108
    @vieuxsarrbadiane2108 5 лет назад +6

    722 moukhadam. Thiey mawdo. Vraiment souniouko amoulwone ham ham toumranké senegal

  • @toukoubaaba1946
    @toukoubaaba1946 4 года назад +2

    Allahou Akbar com el Hadji malick moy khalate bammel nioun founou dieum yalnaniou yalla yeureum

  • @djibrilmbaye5905
    @djibrilmbaye5905 4 года назад +1

    Serigne Ahmad sarr yalla nassa diamouh yagu

  • @oumouba5496
    @oumouba5496 5 лет назад +23

    Machallah fier d'être tidiane

  • @sofyniangdiop3648
    @sofyniangdiop3648 5 лет назад +10

    Dieureudieuf Seydi Hadji Malick RTA

  • @elzosy8796
    @elzosy8796 4 года назад +2

    Macha Allah bilahi kene dou Mame Maodo thiey yalla

  • @juniorthiello2928
    @juniorthiello2928 5 лет назад +9

    NGUEN BALMA GNI AIMÉ WOUL XAM XAM BI LOULEN DAL TAMIT BARKI CHEIKH SADBOUH SENEL MO METI

  • @badagueye4182
    @badagueye4182 5 лет назад +3

    Yalla na yalla fayalnoulen

  • @mbodjousmane
    @mbodjousmane 5 лет назад +9

    Diuere diuef seydil hadji Malick sy ❤❤

  • @kinemaoda2232
    @kinemaoda2232 5 лет назад +1

    Macaalla yalna niou yalla fayall seydilhadji malik sy💜

  • @miabelle8228
    @miabelle8228 5 лет назад +11

    Kéne dou Mame Maodo Sy Malick yalla naniou yalla tass thi sa barké.

  • @ndiankoufall3858
    @ndiankoufall3858 5 лет назад +10

    Ham ham rék mo worr dieureudieuff el hay malick sy diarama ahmed sarr

    • @muhammaddiop6779
      @muhammaddiop6779 4 года назад

      Salam sokhna ndiankou fall..Ahmad dafa am xam xam ...782081390

  • @papemorgueye5393
    @papemorgueye5393 5 лет назад +8

    Thieye kene dou Maoda bilahi

  • @madyndour7416
    @madyndour7416 4 года назад +1

    Li nexna way cest trooooopppp
    Aladji Malick SY yalanala yalla fay

  • @idodiouf752
    @idodiouf752 5 лет назад +10

    Machallah kène dou Seydi Hadji Malick

  • @davidguey42
    @davidguey42 2 года назад +1

    Doumasi doyal té damaléni day geun Di nékh dal♥️♥️

  • @kalloofficiel5206
    @kalloofficiel5206 3 месяца назад

    Yalla na Yalla goudall sa fann ameth sarr❤

  • @fatimadiagne8044
    @fatimadiagne8044 5 лет назад +2

    Dieureuedieuf Sarr lou leundeumon lairal nga ko

  • @amadoudiop1139
    @amadoudiop1139 5 лет назад +11

    Machalla contana trop

  • @mamadouthiaw9280
    @mamadouthiaw9280 5 лет назад +21

    Dieur dieuf SARR Ahmed xam xam by lerna avec des preuves sûr kou wédi démal archive