XEW XEW - Saison 1 - Episode 32 **VOSTFR**
HTML-код
- Опубликовано: 8 фев 2025
- ** Abonnez-vous ici : goo.gl/mme9BS **
Dépenser toutes ses économies ou s’endetter pour un mariage, un baptême ou un autre évènement, juste pour le paraitre, peut devenir un fardeau qui hypothèque toute une vie !
XEW XEW est une série haute en couleur et bongomen : Even Prod a posé ses caméras à Thiès, à la source du théâtre sénégalais, avec les comédiens locaux.
Tous les mardis et samedis soirs 19h30 UTC.
#xewxew #saison1 #episode32 #victimesduparaitre #xewxewlaserie #thies #theatresenegalais #evenprod #team221
** Abonnez-vous ici : goo.gl/mme9BS **
Série réalisée par Ismaela Thiam (Dakar, Senegal, mars 2024)
Une co-production Even Prod Senegal - Wido : +221 33 868 27 26
* Retrouvez Evenprod sur les réseaux sociaux*
Facebook / evenprodsenegal
Instagram / evenprodsenegal
Twitter : @evenprodsenegal
** Devenir annonceur ? Contactez notre service commercial **
Evenprod +221 77 422 70 41
Boulén faté di diouli si yonenti bi Sallalahou haleyhi Wa Salam
Salalahou alla Mohamed ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Salalakhou Allah mouhamed salalakhou Allah mouhamed
صلى الله عليه وسلم ❤
Salalahou allah Mohamed
Sallalahou alla mouhamadine wasalime ❤❤❤❤ merci
Xew xew les victimes du paraître 😢
Chaque thème, chaque épisode compte et illustre des faits de la société actuelle 😢
Oubliant que la simplicité aussi c de l'art ❤❤❤❤❤
Bilahi ioe Machalah ❤❤❤
@@HawaNiang-js6lr ✊✊❤️❤️
Papito sa copin bi guinawam bi bakhna😂😂😂😂
@@AmycolléSylla-o4g ,😂😂😂😂
PAPITO mi aka niak foula ci goor ! son père a raison, amoul ben ambition ! tawou VIEUX SAMB (mi dem makka) mom aka am diome, téyé té am khel ma shaa allah 🤩!
Des coeurs 💓 pour notre Prophète Mohammed sallal laahu halayhi wa sallam ❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤
@@MatarNguirane-k6q
Xew xew dall yaa khew chaque épisode engendre des nouvelles connaissances ,vous méritez plus de j'aime
Mleregment Sénégal khamou niou nimo amé chage 🤦
Ha haaaaa
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
@@FamaFall-v1r bilaye
Bama dalé suivre evenprod ba légui pour la 1ere fois gnou tek épisode 27min et les pub y compris 😮😢
Kou beug serigne babacar sy abonnél aime 🎉
Mom rkk❤❤
KOUY AVANCÉ PUBLICITÉ YII REKK LALE J AIME ❤️ 😅😂
Surtout moi mais dernier plubli je ragal pour lire commataire😂😂
Halatu mako seetan😂😂😂
Awe ma djitou publicité sakh😂😂 série yépou lasi yamalé
Meme présentation sakh
No mère thioro dafa rafettt de trop ❤
Que des noirceur dans cette magnifique série 😮❤ merci evenprood
Kou beugeu sa yaye lale jaimee❤❤🎉😊
❤❤❤
Trop❤❤❤❤
Yenn doul way sunu beugué Mouhamed dougne ko wané si j’aime
Vraiment
Vraiment sonou nagn
Merci beaucoup way
wakhal way
Bilay
Une réalité purement sénégalaise chapeau à éven prod ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉
Xawma kagne guendi bayi kou beugu seydina mouhamed (saw) mayma j’aime sheuttt svp commenter sur la série …
Bravo à toute l’équipe de xew xew 👏🏻🥰
Surtout lolou warna nenesi réunion
Bilahi bouma gissé kouko binde daf may metti trop dagniy wara commentaire si série bi mais dougn ko def seydina Mouhamed lagniy bind wala serigne si arrêt len way guir yalla 😢
Le gars dit à son ami : calme toi man😂😂" thièye li ; khamou ma , aye anglais la, wala anglien 😂😂😂LOVE
Encore Fata ❤😂😂😂😂
😂😂😂😂❤
😂😂😂😂
La beauté de Mère Thioro ❤️🥰 on n'en parle ? Walahiii Mère bii damako beug ❤️❤️❤️❤️
Mom rek lay topou 😂❤🎉😊
Hommage les artistes décédé yalnalen yala yeureum Baracke seydina moukhamed
Amine
Amine 🙏
Amine 🙏🙏🙏
Andando maye bolè fitt pour mou fanani 😂😊
Bou niou si diapoul dou bakh 😂
Awo bi loutakh mouy dougu si lii ah wa bakhna bamou soti😂kou xew xew bi Niambé
Vraiment les filles la senne bopp amoul ndokh bilay
Kou xew xew mi yaw après xew mi louy xew 😂😂😂
😂 😂 Xew xew
Xew xew
Xew xew
😅😅😅😅
Xew xew rék 😂😂😂
Kooussi moytouwul guewel yi walay bisse dina niew nga togue di dioye😭 te do guisse kene koula nakhe
😂🤣tellement vrai gueweul la waye doynan war
Kou beugue Serigne Touba rekk lalal j'aime way ❤❤
Bole'n paré si nganali yi ak anif nguen nieuw si dépense inutile si korité bi ak Tabaski bi
Mére guéweul tamite meuna thiou maan thiaaaaa di🤣🤣 ayy lii ba sén diam leu Evenpro ah batay bakhnaaaa
Seydina mouhamed ❤
Fière d’être élément mame saliou mbacké borom xelcom♥️❤️🩹❤️🩹❤️🩹
Serigne saliou mbacké ba faw ❤❤
EvenProd franchement sur ce chapitre vous avez durés depuis episode 24 je pense
N'oublie pas que c'est 2 thèmes en même temps
@@ndeyemarie6847 Oui mais c’est pas une raison ils perdent trop leurs temps sur les détails en plus les épisodes sont trop courts
Effectivement je me disais la même chose , la fin de ce chapitre saura kan le mari fera la fête je pense
Bi deux khew leu motakh.
1er commentaire🎉😂❤ XEW XEW meilleure série😊
Bilay y’a des mamans youye dougal Séne aye doom si moussiba rk
Niom Yonen tibi fowoukay lanie ko jape kw😢respect ngir yalla ah sonu nanie way
Bilahi WALahi daf may metti bouma ko gisse kouko binde 😮
Yena respecter heure kaey🥹❤️🫶🏻
Woutek wa norbe
Danio meilleures
Nekhol ba nekhol mains li mo am senega😢😢😢l
Mére seune môme setlou naani Moy guéwélou gniy ame défaite
Pour mane kesser mako setlou ter nena mom dou andeu ak borom défaite 😂
@@tinad9225 si défaite RK la deuk NK 😂
khalè yi tay may togou rère gaw gen trop😅mes je vous j'aime ❤❤
Xew xew belle réalisation
Yalna niou fekei koor gui ak diam🙏🏽🙏🏽❤️
Amine 🙏
Amine
Amine 🙏🙏🙏
Amine yarabii
Bakéne j'aime sama commentaire boumala reukkée 😏
😂😂😂😂bague koula jme rek
Boma reukée ma fayou😂😂
Li rek mo ame Sénégal
Suis née au village fatick mais si on je regarde les séries ça me fait rire bilahi daguay guisse kou solou si kaw ak or né yoroul dara sama yay guérté thiaf ladone diaw pourquoi niou complexé bi douniou ko bayi
La leçon de la vie 🥰 ❤️ ❤
Série barina baa doo man a seetaan yépp, xanaa nu yam ci yi gën a neex rekk. Bolle ak Caama, Bolle tay rekk ngay dee, yaay dugg ci ñaareel. 😂 😂 😂 😂
Dem Màkka ñëw doo am foo dëkk laa nara gis.
Mane dhé pour l'instant yi ame changer rk laye suivre
Com Babel bété bété xew xew d'échéance kessé késsé hehe faté wone na mariama 😂😂😂
Super série ❤mais bété bété cest autre chose oh nekh na ❤
Bilahi tu as raison
Kou xew xew 🎉miii yaw
Wa mais Lii guanalé la Wala guenté am thieet, 😂😂
Serie bi daal Keur Ngueweul gui nio si guanio gul🤣😂
Mais Awoo bi Nak war na si wara meun echappé
Kou xéw xew bi iow😂
Cou xew xéwi yaw xamga gua cou xéw xéwi yaw ❤ bonne soirée
Xew xew merci
Pa dem makka dé guisna ni bou gnibisé lay problemes dii commencé... Makka danga koy meune baaxna.
Bolé tak 2 fame ba parés dou fah demé😂
Gnimé woul awo bi😂😂😂
Lolou moma diakhal Thiama rek😂😂
Xew xew les victimes du paraître😍
Cette série est magnifique
Blh gueweul yii doyy naniou warr keur gou tass niokko tass😂😂
Papito ya dadialé say gél sisa anniversaire ne nous fait pas chié tu le savais ahhh
Khana soirée anniversaire bi dafa amonne ay billet yougnouy diay bagnouy apporté ay millions 😂😂😂
Mo diakhal nieup 😂😂
Thies dh artiste yi souniouy anniversaire daniouy diayalei ticket 😂😂🥰
@@awaseye3711 Ah bn yeugoumako wonne 😂
@@awaseye3711 Ah bn yeugoumako wonne 😂
@@awaseye3711Ayway yaw mi😂😂😭
Di Xéw di xéw ba faté investir thi sa live bilahi diga wathiakh sa lokho sandi Kirassoulilah
😂😂ganalè kou diougué macca nga melni kouy thietal wala nguénte😂
Mère Thioro toujours avec les awo yaye❤❤😂
Mais gueweul bi rafetna machalah ak teint bi ❤❤❤❤😊
Barak bou bari pontou mom Dina doy war
Avec even pro rek pule à l'heure ngay ndoundou ❤❤❤
Wa legui niom gueweul yi kagne laniye ayé😂
Souba 😂😂
Ayé djily Nii rk wa bakh na
@@lotalo3925 kome yaw rek boy 😂 wa fou nékone rarr nga dh fisl 🤣🤣
Khana bolé tapete bi xewal niarel bii 😂
@@ajaniang ah niom daniye dem si xéwou diabour yi rek dilen douguele
Sallahou Mohamed ❤
Walaahi maaléne beugu ndah ponctuel 🎉
Papito ak xaritam bi ils m’énervent dolen naturel ngiir yalla😂😭💔 sen anglais yi Xam way
Meunougne joué deh sen séquence warna gaaw diekh
papito mi dolen ko wax ayoul😂😂
mouy forcer ni ak niodi 😅😅😅
Bilay papito daniouy beugueu môme 😂😂
Mai serie béne coté li guewal yi di deff dou yone guewal waroula wax lo manoul ba dilako deflooo 😢
Amna épisode bo khamni saura(ngagne) nèna guèweul dadane guice guèram diakhlè mou guènè kossi
Ni dhei laniouy def legui.. ay mbam laniou billahi
@@SokhnamiSanokho9011 bagnal lolou guewal la d mai nak douma wayane manounou teug manou ma way mai boull saga nak nga balma
Balma dhei
@@SokhnamiSanokho9011 niofarr iao
Mère yagui yolé Bolé dé😂😂😂😂
Gueweul yi niolay dougeul thi xew ngua def lo meunoul après niou setan leu Bayila ak sa ay problèmes 😢
Guewal Dougoulounou kéne Kou wayédi ba dougiulou lomanoul dingus tok sa rokh kéne doula fa fék
Pare tok dila diéwe😂😂
WA yén diomi wolén si bi niarél 😂
Bilay 😂😂
Une série pleine d'enseignement et ki reflète les réalités d notre société bravo à vs❤❤❤❤❤
Merci @evenprod pour la réactivité de la remise du sous titre. Marodi prenez de la graine
Li dhé mo khéeh si réwmi déme macca korité tabaski di diamou yalla gnou sopé ko khéeh ada mofi eupeu dolé dîné
Li kay dou sakh ada kén xamoul loumou done li mom souniou mame yii dougne ko dane deff
Alahouma salli halla seydina Mouhamet wa salime ❤❤❤
May line ma j'aime ❤
La concurrence entre evend prod et marodi TV qui remarque
Nous les spectateurs dal guis nagn si sounou bop
Une concurrence saine les 2 font de superbes séries 👏🏽👏🏽👏🏽
@@louloutebimane dh li la kham apprécié niar yepp yokk len courage merciii à toi ❤🎉
Marodi pure fiction
Even prod pure réalité 😅😅
Elkhadj samb gneuwna
Salalahou hala mouhamed ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sonko moy diomaye
Des cœr pour evenprd ❤❤
❤❤❤❤
Xew xew Les victimes du paraître ❤❤
C'est exactement ça!
Pa bolé ténga delo avance bi😂
Wa louga sén dome amna ndam
Félicitation nioune wa louga
Ma fi djitou😂😂😂
Mourid à vie❤ bamba rek
Suspens bi mome dafa yag trope
Merci even prod
❤ndeysan sama doom bi aka beugeu son bi boukou degué rekk fethe😂😂😂 bb bou beugeu ambiance rek
Mbadou 😂😂😂😂
Tjr au rendez-vous ❤
papito me fait tellememt rirrrrrrrrr
Machallah evenprod 🥰🥺
Meilleur série 🎉🎉❤❤ evenprod love love love sur vs🎉❤
❤❤❤
Amoul béne bour boudoul yalla
Wakh tiko dh Wallahi ❤❤
Mome rk moy déf té kén douko dindi
Evenprod. Nak yok leine temps xew xew dafa touti tei doumassi doyal
❤❤❤❤
Papitoo comme dessin animé 😂😂😂
Arrêter de quémander des aimes avec le nom de seydina Mouhamed psl
❤
❤❤psl
Boul fattei Omar seuveeuhhh😭😭😂😂😂😂😂😂😂😂
Yow sopey seydina mouhamed bi mangui lay Niaan 🤲 nga abonné si sama chaîne bi ❤🙏guir dieumi seydina mouhamed psl🎉❤
Mane soda la beugeu 😂😂😂😂