XEW XEW - Saison 1 - Episode 33 **VOSTFR**
HTML-код
- Опубликовано: 8 фев 2025
- ** Abonnez-vous ici : goo.gl/mme9BS **
Dépenser toutes ses économies ou s’endetter pour un mariage, un baptême ou un autre évènement, juste pour le paraitre, peut devenir un fardeau qui hypothèque toute une vie !
XEW XEW est une série haute en couleur et bongomen : Even Prod a posé ses caméras à Thiès, à la source du théâtre sénégalais, avec les comédiens locaux.
Tous les mardis et samedis soirs 19h30 UTC.
#xewxew #saison1 #episode33 #victimesduparaitre #xewxewlaserie #thies #theatresenegalais #evenprod #team221
** Abonnez-vous ici : goo.gl/mme9BS **
Série réalisée par Ismaela Thiam (Dakar, Senegal, mars 2024)
Une co-production Even Prod Senegal - Wido : +221 33 868 27 26
* Retrouvez Evenprod sur les réseaux sociaux*
Facebook / evenprodsenegal
Instagram / evenprodsenegal
Twitter : @evenprodsenegal
** Devenir annonceur ? Contactez notre service commercial **
Evenprod +221 77 422 70 41
Even prod c'est les meilleurs bilahi parce que Li motakh Sénégal dokhoul 🎉
Ohh cheikh seck mingui maguette ndeysaan 😊😊yalna yalla goudal Seen fann
Kou bougue am dom bu gorr tudeco seydina Muhammad rk lalal..❤❤
Amine yarabi 😊❤
❤❤❤❤❤❤😂
Aaaamiiiine yarabi
Amine inchallah ❤❤❤❤
Nguir yalla dolène bayi kou guene si bindéff yi SAW miguène di wouté aye jaime si aye serie😢 svp
Non serigne ngagn sene Groupe bi Yalna yallah goudeul sene Fane yague deugeureul ande bi macha allah✨🙏
Amine inchallah
Mais goury n’a gneuw aussi nah mou Matt
@@adamandiaye2817 wax gaa deug dh goury tmt fater wone nako
Amine way
Amine yarabi
Le regard de serigne ngagne momay ray😂😂😂
😂😂😂😂
Que ta mère vie jusqu'à ta réussite dit amine 💞💞
Amine yarabi
Amiin
Amine
Amine Yalna Yalla samm sunuy wadiour
Amine yarabi ❤😊
Bravo awo yi quelque soit la situation elles sont toujours là machalla awo ndaye la
Wawaa
Motax gnounane awo yaye
Awo moy lepeu
Douma sama woudiou wone dê kouye bone mome gaye duapalè
Avec xew xew votre cœur bat plus fort ❤️🥰
Bravo à toute l’équipe d’even prod 👏🏻❤️
Non thémou makka gui dinama rayy rek bala diekh avec les 4 mousquetaires😂😂
😂😂
Dama ré baa sonou paa yi 😂😂😂
Bilahi Ngagne tellement véridique et gentil bagay yakarni dafa ignane fek yalah kham neu dafay dawal kharite bi rek
Bilahi Lou rare legui
Fraîchement
Yalna bour yalla yeureum souniou waydiouri yi niou dietou t'ai xaré aldiana 😭
Amine inch
Allahouma amine
Amine yarabi
Amin
Amine
Bilay Serigne ngagne limouy wakh khamnako après laniouy comprends 😮😂😂
Aladji dagnou la ligéy conséquences yi mingi gnew kou khalatoul après nganalé makk Loula nèkh défal😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bilay ❤😂😂😂
@@BayeBassDieng-y6k 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Vraiment j'aime le rôle de serigne ngagne il nous enseigne les réalités sénégalaises bravo 🎉🎉🎉🎉
Sonko mooy Jomaay
Jomaay mooy Sonko.
#Focus2024 insàllaa!
🇸🇳 ✊🏾✊🏾 🥰🥰❤️❤️
yeena xam ndeyem jomay di salafiste bou bon😮
@@KebaDiop-b6sgni nio soff fii sonko amoufi place nii Diomaye merde way
Des coeurs pour notre Prophète ❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤ psl
Bayilene séne thiakhane si di fowé tourou kou téde ki si you gnak fayda yi pour ay j’aime kassé
@@awafaye9881 louthie sa gate
Samb devrait rester en couple qu'avec sa première femme, elle a une bonne mentalité et donne de bon conseil.
Awa yaye yi amatinagnou ndam😍
Ngagne dinama rayy rekk 😂😂😂😂
Kou xew xew bii yennn😂😂wayy nakk près ce que tous les thèmes ont été interprété on vous attend avec les tours de famille, soukeur kor, Korité Tabaski...😢😢😢
Merci beaucoup wawaw war nagne si nieuw
Balaaa ma deee niounan daniou ma liguey respect leen sen awo yiii teeh nekk ay nitt
Yalnaniou yalla mouseul ci diabar diou bone😢 ak goor bén noppu
Samb lii yeppp Ngagne waxon nalla koo ga topp sa gniarel biii rekkk
Animu tay kiga sagune wonn Mouy sa awo molay topato
Bon ramadan à tous yalla nagnou yalla défal kooru jaam té nangou sougni gnane ❤
Vraiment Ngagne xarite guenoula
Billay deug rk lay wakh kharite bi Ndeyesan
Bilahi
Thiey awo yaye bolewounu Dara aki wakh vive les awo 💪
Even Parod kenn du yéen ndax li am ci réew mi rekk ngeen di Joue. Bravo. 🥰🥰🥰
Vraiment 🎉
Billahi série bi mo geuneu am chance thi série Sénégal yeupp
Mn mère thioro rk lay topou❤
Le visage de serigne Ngagne ❤😂
Da diomi katt😂😂
Nit yi takh ngay sonou ba def lo mounoul ñolay togué wat dila kharabe ay way kañ lañouy yéwou def louñou meune wakh liñou meune sunu teudé nélaw ba yandor...
Billaye
Wayadi rek mane keneuh duma deflo luma meunul
Bilay lou ler nga wax
Maane ma bayi lolou dakh nittgni dagni changer comme climat sama khôl da diékh thi seyou Sénégal 😢
Bilay man personnelle deh sama wadiour yingua khamni niom la geuneu fonkou boun Wa wakhe louma leer nii meunou mako dama leeni wakh manou nako mou diekh mais douma ko lebi teh doumako niane
Entre dem makkka ak nganalei il ya tabaski au milieu 😂. Vous devai avoir une idée Def si deux ou trois épisodes avant l'arrivée du vieux
Car tabaski ay xeew xeewu neiin yu bâri problème 😊
Xew xew dafa ame sense❤
Awo yi Ndeysane a chak foi niolay feitei yaye danelay digeul Lou bakh Lou geun si yaw dolein deglou feikk sa mousibeu leu niarel biko dougeul Lo baramam bi sa fourneaux wane Nako guinaw 😂😂maniii def Lo kham wakh Lo kham bo teudei neilaw 😂😂
Waadji kay dafa nélaw
@@Annebaidysouleymane dess na dh guisagoul dara😂
Ana awo yi dieuleuti naniou ndam❤❤❤❤
@@Annebaidysouleymanebeurri nasi morome
Bayi ko rek
Ayyy loy deff rk na donn lo meun wayé makka ñeuw sa fitt dou tokk so teudé do nelaw yalla teggou l lolou d
Votre série est tellement réaliste merci beaucoup ❤
Li bou amoul mort Dina am blessé 😂😂😂
Toujours au rendez-vous merci Evenprod 🎉🎉🎉🎉
Les expressions faciales de Serigne ngagne me 😂😂😂😂
Si tabarayii ses gestes😂
Ramadan Kareem 🌙
Puisque vous avez mis presque tous les évènements qui se déroulent au Sénégal dans cette série (Mariage , baptême, anniversaire...)il ne reste que "tour " ,"korité, Tabaski,tamkharite,...😂 Thièy Sénégal xew xew rèk après xew bi nak : problème (mo tax déf lo mane ,wax lo mane ,bo teudé nélaw )
Soukeur kor surtout j'ai vu un dégât sur ça 😢😢😢
Gamou ak magal 😂😂😂😂
@@bintaniabaly9953surtout 😂
Samb vrai ingrat leu, ngagne mokoy dépanner chaque fois , moukoy neubeutou, wayé saf nala sap
Loussi barri ni lay deimer deih. Niit gni nga gueuneu mana takhawou gnola gueneu mana neubeutou
Deugueu lay bagna degueu
Billakhi lii Moy aduna😢
Yalla boumou oumpou bén wadiour thie barké cheikhul khadim
Amine yarabi
Amine inchallah
Amin yarabi
Mére thioro sa bleu machallah ak sa tient noirceur d'ébène ❤❤❤❤❤❤❤
Au nom de la cohésion sociale, je vous souhaite un Saint temps de Ramadan yen souniou deukeundo Muslims yi 🙏🏾
Nb: Ngalakh reporté 😂
😂😂 Ngagne li am am na ba paré kayy nga firi sa kanam bi sahh
Nguayi bou lene faté ni diomay moy sonko sonko moy diomay❤❤❤
Defflo mane wakh lo Mane bo teude nekaw😮
The crurent most important serie to me. Lii Sénégalais yeupa ko war di setane ndax niou yewou ci jamono ji
Awo aladji bo dafa rafet mashallah ak tein noir bi ❤
Seck mi amna mello 😂😂😂😂
Serigne ngagne franchement mogui joué rôle bou ame solo xéweul yi nignou lagnou df bou yég défar bamou tarou té dougnou la yaxal mé xéweul Légui nama yalla bal li yalla xame doyna
Serigne ngagne vraie comédien. Chapeau à toute l'équipe merci
Awo yi mention special 🎉🎉🎉ndeysann awo Yaye 🎉🎉cituation bo meuneu dougou mom moy takhaw 🙏🙏😭
Tonton ngagne nimouy def canam bi nak 😂😂😂😂
Rethiou dina fek dieuf wessou naniu moytu guiss leen ma molay done gal ci mussiba té gnila done diay daniuy takhaw feulé dila retan
Merci evenprod ci oeçon bi👏👏👏
Sa gnarèl bobou ng djokh sa khaliss bayi sa awo. Bo topone sa awo lolou yeupe do ci nèk taye. Da ngaye djouguè maka sa khèle dale
Sambe ake fondé bi Li yep yako tek sa bopou😂😂😂
Boy lén faté gnianal gni diotali ticket yi si bus yi📿🙏
Bilay dague la 😂😂😂diarna ko de
Tay rk digantei case ba kolobane sama lokho deoite bi tienei na ndax rawalei 😫
@@Khadim-mk5cgdeugu la wakh Di sonnn nagn d😂
@@Reotraabdou1808bly t Soko défoul gniou outal la sikkkk méttina d
Ak gni wané fou bus yi diarr diarama yén si disponibilité bi
Samb lou mou doug rek niarel bila ak Ngom wayé dina wét ak ayy boram! Seck mom déjà mo beugone billet bi c'est l'occasion pour lui de se venger😅
Aye cou bédi sa awo dingako guise😂😂
Ñiarel yi naye nèkh rk bou nakhari gnou dème bala😂
Warou ko wone sakh defaral ndeki samb mi dou touss 😂😂😂
Samb soin de visage lagne ko défal 😂😂
Père Cheikh Seck Machallah❤❤❤
Baye cheikh nak kou goré la li moy amitié
Waw ki dou Fadel Guéye sama sopé bi wnii bikk ❤❤❤
Seri bi dafa nekh❤
Baye cheikh seck vraiment ya meun sawayy kou ame soutoura ni yaw lay mell❤❤❤❤
Kou yakar ni samb danoiy nakou keur gui rek lalal j'aime 😂
Ww
Evenpro vous êtes les meilleures 🎉
Serigne Ngagne bilay kenn dou yaw😂😂
gor boufi abandonné Awo bourou keureum do diougué si diafé diafé
Ndeysan sama khol tooyna si zest àwo samb bi def kouy àwo RK lalal j' aime ❤
Def'lou meun Wax'lo xam so tedei Nelaaw Série bi loy kassei laafi jangalei THÈME Mashallah les ❤🎉
Xew xew série bou nex❤❤❤❤
La beauté naturelle de mére thioro on en parle wala?
Machallah elle est fascinante
Mère thioro rék laye top 👍❤❤
Des ❤pour notre mamans
❤❤❤❤
❤❤❤❤
Ndaysane baye cheikh seck damako beugue rék bilahi yalla nanga goudou fane
Serigne ngagne rekk lay top 😂❤
Ponctuel kay yéna ko def🥳🥳🥳🥳🥳
Je te jure
Even pro rk
Ma campagne électorale commence : sénégalois, sénégaloises, si vous m'élisez, le 24 mars, je vous jure que je deviendrais.....milliardaire😂😂. Surpris? Pourtant je suis le seul candidat pour lequel tu peux jurer sur le coran, qu'il va tenir sa promesse😂😂. LOVE
Fata mayniu waay 😂😂
Dommage, senegalois senegaloises aiment pas vérité. Tu seras pas élu
😂😂😂
Fichier manquant bici fin bi , erreur impardonnable pour l’équipe technique…….😎
Sinon vous êtes bon
xew xew la après xew mi louy xew 😂😂😂
Xew xew rék 😂😂
Xew xew
Xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew xew
Cou sa yaye di awo lalal j’aime
Sénégal bokuna si xew xew yi ñu bari sen xalis moy lolu
Pa yi mane name theatre machala
Alkhamdoulilah sen dom amna namm 🎉
Evenprod apres tous ces thèmes revenait sur les soukarou koor,préparation de karité et tabaski svp
Merci beaucoup à vous
Yaw mi lir sama commentaire balla souba yalla dougou alldiana nelll amine ❤❤❤
Amine
Yalla guama fa djitou nel amine ❤
Ay way samba amna problem 😂😂😂😂😂
Machahala meilleur série de l’année ❤
On veux thiate 😢 il est le meilleur 🫶🥰
Le père de papito il est avare😂😂😂😂
Mais sambe dème gua maka ba gnibisi ni😂😂😂
they liguer nak digua khamna dème makka dou nonou 😂😂😂
Mane lima diaxal seck loumouy dioxogne Serigne ngagne nane ko yow nak amna lo khamni waroula enhh téyal enhh motaax ngagne maynako patte bii. En résumé lounioula boléwoul boussi dougal sa ingrédients neel patte rek dilene sétane Mane dé Lila waax ba yénite tamite lolou ngéne waax
Samedi Tay bi bou amoul mort dina ame blaisser😭🥵🤣🤣🤣🤣xalei yangi teuth saison bi Nice kay🙄👩🦯😎
Non yaw dou net😂
Na blessé rek boumou âme mor
Yalla Nanou Yalla diégeul 🤲🏾.
Sacré Samb 😂😂
Bilaye goor boussi doul dégue sa awo do xam Loulaye daal Samb dh djabar moko djitté bilaye Serigne ngagne wax ngua DEUG samb iow sa djabar motakh ngua torokhal Say dool😊
Père néna danouko laguèy dehh 😂😂😂