Il a tellement le coeur sur la main. Que Dieu te protège . Merci de les avoir fait vivre ces moments car ils font partie de la société comme nous malheureusement c'est cette même société qui les marginalise . Que les autres artistes prennent exemple sur lui. Car li len dal natou Yallah la et meun n'a dal kou nek . Doundou bou souteguoul lep khadj Nassi
Vraima Wally mosouma khamnai ni nga melle bilahi mane dama beugue nik kou solidaire ta oyaf ta yeureum diam yi ndankhté yalla lay mayé mais day am foum ko diaralé diamou si yaw ndankhté ginaw yalla diamou handicap yi mingui si yaw day geuneu bakh rek barki SERIGNE FALLOU
Slt vrema je suis très content de Wally seck sur la voiture qu'il a Rémi a mon ami allé je lui avait dit depuis que si tu as la chance de rencontré Wally inchala tu auras une voiture koon rouss lo woma je suis pas handicapé mais je plaide pour eux toujours et tous les handicapés me connaissent bien
@@modouniaye8396 wally mo wakh ma deugheul limou wakh wayee yalla nako yalla hiir teghma tchi c'était juste à titre d'exemple une tête c pour reflichir
@@deugheulaveritemoufin4731 reflechir motakh ma niane lima niane Wally limou kou yoré aye nopou dégue gua ko mane lou bakh la niane té nianouma pourquoi lima niane dila dérange accident bobou yalla nafa yam té yalla mouseul si mbolém dioulit

Kou beugue Wally bassal j'aime
Meilleur artiste sur le sociale de l année 2019 vive wally seck yalla nala yalla fay sa khol inchalla
G: g3h5523 t2 zrt ac233 v5 av 1z 1 43cg 3 c322222 nr2rr 22 2cv111aa2 et ta journée a la maison
Bilah Wally lou bakh rek ngua ye ame mangui niane si bakè seydimamouhmed yalla na nama yalla may wersek bamalène di dimbeulè comme yaw
Machallah c'est très jolie laf thiate waly sa khole rafétna yalla na yalla same
Vraiment je suis fière de Wally que dieu te protège
Vraiment Wally ta un grand coeur que dieu te donne tout ce que ton coeur désir
Bayinala ak serigne fallou yalla nala fay khôl faramareen bi machala
rafetna trop waly yalna yalla faye sakhol je trés content merci
T'as un coeur en or
Machallah seckh yalla na yalla lafale djate
Maa shaa Allah maa shaa Allah ..the boy with the golden heart..Sante yalla 😭😭😭😭
Son grand coeur m pleurer vraiment, dieu te le rendra Wally, kil te protege
Wally machallah yalla nala yalla lafal tiatt 😍😍😍
Machalla waly content trop on t'aime beaucoup
Bilaye j'ai pleuré wally yalla nala yalla faye
Dondale be découragé Wally seck rek tu es meilleure mon frère
Masallah wally keep moving yalla bakhna Allah will surely bless you inshallah🙏
Machaala bonne continuation wally homme de coeur que le bon dieu te protège amine
Akaa gniak kigniane merci Wally k dieu t protège
Machallah machallah sama Wally seck rek one Love ❤❤
Que dieu te protège wally wallahi ki guissouma kouko gueun
Vraiment Nice na
Merci Wally ils se sont vraiment défouler merci par cette joie
merci bcp mr le maire de la medina bamba fall
Wallahi wally tu es humble tu as la bénédiction d'allah
Wally il communique bien
Dieuredieuf Bamba Fall khole et geste bou rafet
Je.suis fière d'être fans wally seck
Vraiment il a un grand coeur tu fais notre fierté mw j t'aime bcp..
Waliy seck sakhol rafetna machelah
BAMBA FALL hoo kou bakh😊😊
Mane j'adore wally ndakh dafa fonke bopam
Yalla nala yalla faye 😂😂😂
Bravo Waly machalla 😍😍❤️❤️🙏
Wally yow rek may Allah continue blessing you..... Blessings upon success
Framarenne du nitt bilahi limi way mo nekh bilahi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
li raf3t na lolou wally 😭😭srx dama contan si yaw
Fier de wally seck que dieu vous bénisse
Massallah li amena solo si domo adama domo adama dafa mak
Yalla nalla faye sa khole
Chapeau au maire bamba fall Medina il a offert 2 millions au handicapé
aka yatou khol ta bakh yalna takhawou
Machalla machalla Waly seck 💖💕💕
Waly sénégal sou amone canen cou melni yaw cone handicapé dougnouco xep si dara machala
Waly on laisse avec le bon dieu merci pour le plaisir des handicapés
Que dieu te protège et te donnera toujours la force
Amine
Que dieu te protege mn wally machala tres bonne noble geste
Wally rek yala mogo baghale bopame machalah si kaname rek
Awesome!
Boy wally sa auto bi Machalla
Machala wally yalana anetou ta ga ame thi aye mérom
Walahii yalla nala fay sa xoll
merci Wally
Wally borom xolle bou nayiss bi
Vraiment Wally est gentil
Mashallah i love you🎶🎶🎙🎙🤴❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇬🇲🇩🇪
Vraima Wally mosouma khamnai ni nga melle bilahi mane dama beugue nik kou solidaire ta oyaf ta yeureum diam yi ndankhté yalla lay mayé mais day am foum ko diaralé diamou si yaw ndankhté ginaw yalla diamou handicap yi mingui si yaw day geuneu bakh rek barki SERIGNE FALLOU
Nice Wally tué fore
boye wally boul ragal daaaaarrrra yalla mou nguek yow wallahi di nga raw say masse
Vraiment merci Wally
Yalla nala yalla faye sa xol wally
diarama waly Seck srg touba protégé
du jamais vu que dieu te protège
Mançhallah chéri sokhna
Biens dit mon frére,amare diamme
Amall tawfekh rek fall
Wally ninga térélé domou adama yi yalna la yalla téral
machallah machallah amine yarabi 💪☝️
Noble afaire wally thi kanam rek
MAshaALLAH
Machallah Yagui fi way di begue rekkk
Wally dall je t'aime point
Slt vrema je suis très content de Wally seck sur la voiture qu'il a Rémi a mon ami allé je lui avait dit depuis que si tu as la chance de rencontré Wally inchala tu auras une voiture koon rouss lo woma je suis pas handicapé mais je plaide pour eux toujours et tous les handicapés me connaissent bien
Machallah
l'AF thiat rek com dab déf Lou bakh sa yeuf leuu
Chanteur du peuple sénégalais
Nice
Machallh wally seck
Yalla na sa diamuo yague Wally 🤲🤲
Machallah wally
Bravo Wally
Merci way
Thiey adouna mo niaka solo bilay
Yalla nala yalla fay
🙏🙏🙏🙏🙏😭😭😭😭😭♥️♥️👌
@@annagomise9345 dama beugue wally seck rek
Mercii waly doudal loubarii
amiiiine way wally
😭😭😭😭😭
😍💘💘💘💘💘💘💘💘🖒
BILAHI wally mala beug ndax sa bakh
si tout le monde était comme toi kene dou sonnou
Waly yaw goudou fane mola ware😥😥
Kou yebhou ladj Schumacher champion du monde formule1 et tétraplégique depuis un accident de ski...
Accident bobou yalla nafa yam té yalla défal Wally diamou ak mbolém dioulit
@@modouniaye8396 wally mo wakh ma deugheul limou wakh wayee yalla nako yalla hiir teghma tchi c'était juste à titre d'exemple une tête c pour reflichir
@@deugheulaveritemoufin4731 reflechir motakh ma niane lima niane Wally limou kou yoré aye nopou dégue gua ko mane lou bakh la niane té nianouma pourquoi lima niane dila dérange accident bobou yalla nafa yam té yalla mouseul si mbolém dioulit
@@deugheulaveritemoufin4731 😂😂😂😂😂👏
@@modouniaye8396 santh Ndiaye daal mo meeti
Khol bi mo rafet billahi
Nala yalla faye sa xol ballago
cool frère
Diam rek gay am andicape gnon ko beugeu amna sama domou sœur andicape la meunoul wakh me Waly rek la beugeu
Wally merci way
❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭
Li rafetna trop waly
Macah allh
Bilahi deugue la