Papa thione yalla nako yalla khare aldiana firdawsi thi barcke serigne touba khadime rassoul nitou deug pirr wally seck du courage yalla nala yalla arr samb goud fane were thi barcke serigne touba khadime rassoul
Sama xol dafa dièkh 💔 Ndeysane Wally niak na, dina weete 😭 nioune nieup niak une étoile paix a ton âme Papa Thione légende.. 14 mars 2021 a jamais dans nos cœurs 💔🕊
Magnifique duo père fils Moi qui suis une fan de Thione Ballago SECK Le parolier de la musique sénégalaise depuis plusieurs années je suis heureuse émue de voir ce sublime duo sur cette magnifique chanson pleine de sens Émouvant bravo j'ai des frissons maschallah Bonne continuation
Ma sha Allah, ma sha Allah, ma sha Allah laf thiat, yalla naléne yalla same are moussal léne ci seytané . Ndoudou léne ba énerver, 100 ans sans ordonnance. Barigo ci mbartale têk barame mou déme tégoul barame mou déme, soul kér douko térè féne, yalla néna waw néle waw ndakh nga nopalou. Bilahi maléne beugue barkè Serigne Fallou sama wadji. En bad les nones ci soufa souf. Papa thione et Waly sa kaw sa kanam
Law lathiat law lama lamigne faramareen mingui niiiiii khalé bi legui meuna waaaay😭😭😭😭les paroles dun père qui est fier de son fils Machallah waly yalna nala yalla defal diam lou baax reik nga kham❤❤👌Papa thione yalna firdawsi doon sa deukou waaay🙏🙏
Machala ton papa a été toujours mon chanteur préféré svp reste tranquille et continue ton chemin surtout vous êtes encore jeune on t'aime beaucoup bonne continuation
Vraiment wally yaw ak papa thione sene waye bi dawena yaram nekhna aussi dilenegnanalerek thi yalla lafalelene thiat damabeug sama yaye motakh kome ninguabegue sa yaye diaga diagayallana doudou 100ans amine
Kouné ak Loula yalla maye mais lii mom dafa néhh kou sanione amko bilaye deuk nékhoule mais yalla moy mayé waye mom dangne KO meune famille seck c l'international 🎉🎉🎉❤
demb franchement nieup contane longue vie a faramareene bi ce duo exceptionnel entre le.papa et le fils.machallah félicitations et bonne continuation pr d autres grandes scènes international😍🙏🙏
Vraiment c’est une grande fierté un père qui accompagne son fils wally bonne continuation une exemple à méditer respectons nos parents la bénédiction est très importante
Il a bercer notre enfance Wally nous fait vivre notre jeunesse on vous aime Wally en le meilleur de tt les temps il a ck les autres n'ont pas son cœur 💓 d'or on taim bilay seck balaogo
En écoutant ce duo sa a fait couler mes larmes😭😭😭 tellement dafay dougou ci hol et te faire pensér des choses inoubliable.vraiment Merci Papa thione et wally.diam ju sax inchaalah
Ce son je pleure à chak fois que je l écoute bien avant que ma maman ne soit plus là. Qu Allah accueille toutes mamans à son paradis céleste., et garde aussi longtemps celles qui sont en vie.
Du jamais vu bilahii😘😘lii dawneu yaramm bilahii😭😭yalneu yallah goudeul seu fane sougnou waly💕💕💕 tei mou mousseul leu sii thiate ak lepp louleu meuneu yakal🙏🙏
J'étais bien présente ce jour là tei depuis dimanche image bii akke bou 31 décembre bi meunoule deigne ci mane papa thione yalnako souniou borome atté ci yeurmandéme 😭😭
Ah oui tres contente pere et fils longue et a tt le monde wa wally mane dama defoneny magui etats unies ya fi def loukene defoule helenita bou wally jecoute que wally merci frere et tt lequipe faramaren
Franchement suis ému bilahi yalna diam yague parent bou neik meriteina li billahi diom daffa nehe yalna fi yalla bayi sougnou wadiour yi surtout nos braves maman sama yayye yalna yalla goudeul faname ake yayou gneup bagnouou teiral leine si barke alhouranne
Abi Thione,FatherThione, Padre Thione, Vater Thione, je t’aime dans toutes les langues et a chaque jour et a chaque heur .Que dieu te bénnie , ak kép cokhani sa papa moungui dound yalnaco yalla may goudoufane ,kép co khamni sa papa dafa fébar yalna yalla weural ay thieuram bamou delo thi sagom , kép co khani sa papa dafa guénn adouna yalna ko yalla yeureum té kharéko aldjana bou geuna kawé.
Oh mon chanteur préféré tu es parti sans me dire au-revoir yalla nala yalla yeureume harer ko aldiana you gueneu kawer amine tu me manques trop je tm fort Pape thione le meilleur de sa génération le parolier le véridique le responsable le généreux le digne le sage l incontournable l honnête le sincère louma metty reck moy niou bary hamouniou wone yaw yaye kane oh je ne te reverrai plus je ne t oublierai jamais ce dimanche fût le jour le plus dur de ma vie je n oublierai jamais ce jour yalla nala Seydina Mouhamed PSL terrou aldiana amine tu me manques trop je ne t oublierai jamais
L'I dall nékh na Wally Seck maryacine fi yafi nek amoul kénene li nak diomoula dakh sa khôl dafa rafét thi kaw rék si kanam machallah contane nagnou si yaw yalna la yalla lafal thiate té bayi lafi
Man mom j m dis k té l meilleur papounet borom khol bou rafet bi diam rk gey am chéri mum sokhna aidara Mme seck yallah nala serigne Bamba tahawou et o6 merci pour tt j né mm op les mots daddy
Que dieu te pardonne et que dieu t'acceuil dans son paradis le plus heureux éternel firdawss Amine inchallah à chaque personne qui regarde cette vidéo nous vous demandons selonellement de formuler des prières très très très profond destiné à notre défunt le papa thione que le créateur de l'univers vous accorde la paix et la terre de Yoff soit très très très très très légère à tous moments je suis gravement triste de votre disparition une fois arrivé au pays inchallah je passerai chez la famille pour présenter mès très sincère condélence force à toi mon frère Wally Ballago seck force à toi
Kou begue sa baye beseul l'ongle vie papa
Longue vie papa
Yalla khareko aldiana
Long vie Mn papa
Papa thione yalla nako yalla khare aldiana firdawsi thi barcke serigne touba khadime rassoul nitou deug pirr wally seck du courage yalla nala yalla arr samb goud fane were thi barcke serigne touba khadime rassoul
Qui est là même après la mort du légende Papa Thione
Qu'Allah l'accueille dans son paradis céleste
✌️
Ndeyesane li dh moy adouna li ko yobou dougnou fi bay paix à son âme
Sama xol dafa dièkh 💔 Ndeysane Wally niak na, dina weete 😭 nioune nieup niak une étoile paix a ton âme Papa Thione légende.. 14 mars 2021 a jamais dans nos cœurs 💔🕊
Mademoiselles c la vie adouna migi ni, kou dioulii rek nianalko
Lafthiat yalnako yallah yeureum te khareko aldiana firdawsi amine
Qui est regarder en 2021 papa thione Ballago Seck yalnako yalla yerem ta kharéko Aldjana firdawsi Barké seydina mouhamed 😭
Amine
@@fatoudeme5799 90900
Amine
AMINE yarabi
Mw amine
Papa Thione démna nii😭Yallah nako Yallah yeureum té kharé Aldiana Firdawsi si barki Naby PSL🙏🏾
😭😭😭 ndaysan bilaye sèck khadjon ngafii dè nitou deug dèm na Yalla nanga tasèk nabil moustapha psl sama waykate bii
Depuis le décés de pa thione j'arrête pas de regarder ce duo extraordinaire😢 Le pauvre ballago dineu wéet 😭😭🙏🙏
May Allah give you janna i will die loving you
🙏🏾
Magnifique duo père fils
Moi qui suis une fan de Thione Ballago SECK Le parolier de la musique sénégalaise depuis plusieurs années je suis heureuse émue de voir ce sublime duo sur cette magnifique chanson pleine de sens
Émouvant bravo j'ai des frissons maschallah
Bonne continuation
Qui yalla maynako yalna khipé aldiana wally dou sakh sigui khol papa thione
Papa thione yalla nako yalla kharé Ardiana Wally mougnale adouna nii rékh la 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
*C'est vraiment émotionnelle et magnifique Yalla nagnou Yalla fayal souniou parents yii*
Amine
Amen 🙏🏾
Amine way
Ma sha Allah, ma sha Allah, ma sha Allah laf thiat, yalla naléne yalla same are moussal léne ci seytané . Ndoudou léne ba énerver, 100 ans sans ordonnance. Barigo ci mbartale têk barame mou déme tégoul barame mou déme, soul kér douko térè féne, yalla néna waw néle waw ndakh nga nopalou. Bilahi maléne beugue barkè Serigne Fallou sama wadji.
En bad les nones ci soufa souf.
Papa thione et Waly sa kaw sa kanam
Law lathiat law lama lamigne faramareen mingui niiiiii khalé bi legui meuna waaaay😭😭😭😭les paroles dun père qui est fier de son fils Machallah waly yalna nala yalla defal diam lou baax reik nga kham❤❤👌Papa thione yalna firdawsi doon sa deukou waaay🙏🙏
Dama beugue waly seck ba soumakoy deglou damay dioy amal diam reik barki serigne touba gnaneu bou soti reik mo sonal borom jtaime waly ❤️😭
💟💟💟💟👑👑
Sama khol nekhoul dara thi dece papa thione yalla nala yalla khare aldiana firdawsi thi barcke serigne touba khadime rassoul
Papa thion Yalla nala.yalla defal soutoura bamel barkep sa xarit Bi sa sope Bi rasouloul lah 😭😭😭
J ai tellement pleuré billahi pask dama khamni nila mél si Sama yaye j l aime tellement wally demal demal si kaw barkep say wadiour
Machala ton papa a été toujours mon chanteur préféré svp reste tranquille et continue ton chemin surtout vous êtes encore jeune on t'aime beaucoup bonne continuation
Vraiment wally yaw ak papa thione sene waye bi dawena yaram nekhna aussi dilenegnanalerek thi yalla lafalelene thiat damabeug sama yaye motakh kome ninguabegue sa yaye diaga diagayallana doudou 100ans amine
Domii mbeur dianguil beurré 😘way youssou ndour amoul lii dh🤣.
Vive seck family kou ni amine yalla na sa koor validé waay
Tyer Mistik Mind fii lo fiye toude Youssou ndour.wally dina way bayi mok papame douniou dape Youssou
@@MJ-tr8xq bilay car you c'est l'universel le roi du balakh moy s'en mbaye waly est mon fans mais il faut comparer ce ki est comparable
amine ya rabbi
Mo ioe loula dall wakhi dof Youssou n a pas besoin d avoir un fils qui chante domam diangg kat la. Diakhassé rék nguèn meun
Kouné ak Loula yalla maye mais lii mom dafa néhh kou sanione amko bilaye deuk nékhoule mais yalla moy mayé waye mom dangne KO meune famille seck c l'international 🎉🎉🎉❤
demb franchement nieup contane longue vie a faramareene bi ce duo exceptionnel entre le.papa et le fils.machallah félicitations et bonne continuation pr d autres grandes scènes international😍🙏🙏
Bialaye li nekhna wally seck yalla na goudou fan te am wer barké serigne fallou amine 😙😘😍❤❤❤👏👏👏
Ndayesane wallahi sma yarame bagui daw sax papa Thione Seck yalla nako yalla yeureume xaréé adiana firdawsi thi Barkep serigne saliou mbacke 😭😭😭😭😭
Ndeysaane dérétt dou réer lo bagne sa dome néthia bouko fowé machalla 👏👏👏👏👏👏👏👏
Wa lii néhoul té daw yaram😍Wally machallah yalla naleu borom bi sam arleu ba do guiss loy ragal
C'est la première fois au Sénégal l'histoire retiendra
bilah
Machalla famille wally seçk 💋💋💋
Boulene faté tamite coumba gaolo ak yayame
c vrai
@@mbayegueye4535 mon frère ça c'est le concert c'est différent mon frère
Ayy papa thione un monument s'est éteint yalnala yalla yeurem si barkée mouhamed psl😭😭😭🤲🤲
Ndéyssan mangui fawone dotouma guiss papa thione repose en paix.
Yalnako yalla yeureume t kharet ko aldiana pape thione je t’aimerais tt ma vie dougnou diouk ci dila gnanale 🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Papa thione tu nous manque vraiment avec ta bonne humeur ohhh xamna yagui aldiana Ndeysane 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️🥰❤️🥰🥰🥰❤️❤️❤️love you
Jai jamais vu un spectacle aussi riche en son et lumiere wally tu as assuré grave bonne continuation et joyeux anniversaire
Dégeuna deuguuu
Kou beugue wally beusseul j'aime ❤
Waly seck goudal fane khol ba rafete ça se voit carement wakh amoul je taim du courage 😘😘😘
Vraiment c’est une grande fierté un père qui accompagne son fils wally bonne continuation une exemple à méditer respectons nos parents la bénédiction est très importante
Il a bercer notre enfance Wally nous fait vivre notre jeunesse on vous aime Wally en le meilleur de tt les temps il a ck les autres n'ont pas son cœur 💓 d'or on taim bilay seck balaogo
En écoutant ce duo sa a fait couler mes larmes😭😭😭 tellement dafay dougou ci hol et te faire pensér des choses inoubliable.vraiment Merci Papa thione et wally.diam ju sax inchaalah
ki aime papa, thione comme moi Wally diam si ioe
Je l'aime plus que toi😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😫😫😫😫😫😫😫😫😫😫
@@fabintakonez6260 😩😩😳😳billay aduna dou dara guisgua dh maintenant il n’est plus là
Masta a toi
K dieu bénies nos parents merci wally magnifique
néné awa Coly
néné awa Coly Amine
Amine
Xalè bi mako beug domou pape thione
C l meilleure
Que c’est beau. Père et fils sur la même scène! Papa Thione tout le mérite te revient. Wally un vrai showman. Bravo à vous deux.
Ce son je pleure à chak fois que je l écoute bien avant que ma maman ne soit plus là. Qu Allah accueille toutes mamans à son paradis céleste., et garde aussi longtemps celles qui sont en vie.
🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🕊️
Ndeysane je n’arrête pas de regarder la vidéo wollah ❤❤😊
C jolie de voir Wally et son père qui chante ensemble
Franchement Wally Mane saye sons moye dinedi sama stresse
C magnifique bilakhi dagne lay bègue
Thione Seck est vitime de la mode ? Bon enfin wally est ce qu'on appelle la perfection personnifiée ❤✌ il est au sommet de son art 💕💕💕
L done king d la musik sénégalais l roi du mbalax tei unik mar yacine may sa bigué
En regardant cet duo j’ai pleuré c magnifique bon continuation les Ballago
Wally 💪yalla nala yalla défal diam🤲 ak salam si barki baye karim mbacké doundeul lou bari diam rek baye fall bi 👌
Mashaalah papa thione dafa def sagnsé bouné moute thi ninif bi mane dal beug na li💖💕
Chapeau à toi Wally seck le roi de la musique sénégalaise big up papa thione🤴🏾👑💪♥️♥️♥️
Du jamais vu bilahii😘😘lii dawneu yaramm bilahii😭😭yalneu yallah goudeul seu fane sougnou waly💕💕💕 tei mou mousseul leu sii thiate ak lepp louleu meuneu yakal🙏🙏
Long vie papa🌷😍wally mon bb yalla n'a La yalla same💌
Maintenant Wally Seck est le meilleure musiciens que son pére kou beugeu pére et fils et Ram Dann beuseul 👍👍👍👍👍👍👍
Machalla j'ai des larmes aux yeux pareceque j'ai perdue mon papa wally que Dieu te bénit et longue vie à papa thione
Yalnako yalla yeureum tée kharéko al diana
@@mansoursybarry8813 AMINE
2024 je vous j'aime bilae firdawsy sa keur papa brome khol bou rafete waly boule tite dra diame rek guaye ame❤❤❤❤❤❤
Ndeyssane Adouna dou dara deh 😢❤
Bilahi Walahi souma meré wala ma stressewou faramaren yi rek nio meun si dara yallah nalen yallah fay ❤️❤️❤️❤️❤️
J'étais bien présente ce jour là tei depuis dimanche image bii akke bou 31 décembre bi meunoule deigne ci mane papa thione yalnako souniou borome atté ci yeurmandéme 😭😭
Ah oui tres contente pere et fils longue et a tt le monde wa wally mane dama defoneny magui etats unies ya fi def loukene defoule helenita bou wally jecoute que wally merci frere et tt lequipe faramaren
Franchement suis ému bilahi yalna diam yague parent bou neik meriteina li billahi diom daffa nehe yalna fi yalla bayi sougnou wadiour yi surtout nos braves maman sama yayye yalna yalla goudeul faname ake yayou gneup bagnouou teiral leine si barke alhouranne
Papa thione seck yalla nako yalla kharé aldiana sii barki seydina mouhamed 😭😭
Abi Thione,FatherThione, Padre Thione, Vater Thione, je t’aime dans toutes les langues et a chaque jour et a chaque heur .Que dieu te bénnie , ak kép cokhani sa papa moungui dound yalnaco yalla may goudoufane ,kép co khamni sa papa dafa fébar yalna yalla weural ay thieuram bamou delo thi sagom , kép co khani sa papa dafa guénn adouna yalna ko yalla yeureum té kharéko aldjana bou geuna kawé.
Souniou papeuh dji dem na
Ndeysan kou khol Wally fi rek guisni khol bi defa fekh longue vie WBS♥️
Li daw na yaram vraiment des larmes pleines dans les yeux ani gni beugu mifa faramareen
Ndeysane li dakoy setan diko setanate yalla nala yeureum papa thione té kharé aldiana firdaw si amine
Papa thione yaw kene dou yaw waye waye kouko neugue beuseul jaime
Wally seck doumoromou béne khalé yalla na yalla wéreul sa bate machallah
Yalla nalako yalla samaleu 🙏✨
Papa Thione yalla nako yalla yeureum tei kharé ko aldiana
C'était un duo de ouf😍😍😍
Yaguelen fi way❤
T'es jolie
Bon anniversaire Wally sama jumeau du 27 04 machala que dieu vous protège
@@mamadouseck7792 merci pour le compliment😘
@@thiorojoop4019 nice
@@alimafall4044😘
Papa thione a bien machalla kilifa dou feith , yalna yalla woyofal souff thi kowam
Bly wally linga beug yako xam yalla nalako souniou brm bi defal
Amine
Li daw n'a yarame waye néléne ko machallah yalla naléne thiate sékhlou waye amine 🤤🤤🤤😘❤😘😘
Oh mon chanteur préféré tu es parti sans me dire au-revoir yalla nala yalla yeureume harer ko aldiana you gueneu kawer amine tu me manques trop je tm fort Pape thione le meilleur de sa génération le parolier le véridique le responsable le généreux le digne le sage l incontournable l honnête le sincère louma metty reck moy niou bary hamouniou wone yaw yaye kane oh je ne te reverrai plus je ne t oublierai jamais ce dimanche fût le jour le plus dur de ma vie je n oublierai jamais ce jour yalla nala Seydina Mouhamed PSL terrou aldiana amine tu me manques trop je ne t oublierai jamais
Papa thione aka mala yènèwone ga dounde ba ame 80ans
Mais yalla lolou dèf mo gueneu
Repose en paix
Wooy papa thione le tirailleur des faramaren 💕💕diam si yaw
🤭😂😂😂
Papa thione yalla yalla yeureum té kharé ko ardiana firdawsi
Ohhhh très émouvant ma lene beuge pirre un bel heritage t'as reçu wally sois fier de ton papa, mashalla
Papa thione yalla na lene yalla moussal thi none ak thi pekhe ak sa wally
Moi je suis fille à papa c'est pourquoi j'ai des larmes aux yeux
Machala sa khole mo rafet
Bilay j'ai pleuré en pensant mon papa que j'aimé temps et il ma quitter pour toujours
Dyesan machala yalna yala yerem. Amgua fcbok
@@zeynambaye9683 Que firdawsi soit sa demeure inchallah
Ndeysan duo bi dama dioy ba sama makup bi yeup yakou😭😭😭Billay ça touche le coeur Ndeysan
Bilahi wally sou bayé woy ma bayi déglou musique 🎧 je t’aime 😘💕❤️
Bilea wally sa bayy Moy wayi sama yaramm di daww papa thione repos en paix ainsi qu'à toute les nos vivant
Wally wallah suis trop fans de toiii♥️chapeau👑
Yalla nako Yalla kharé aldiana you guene kawé alawou amine
ku papa thione béuseul j'aime 👌
L'I dall nékh na Wally Seck maryacine fi yafi nek amoul kénene li nak diomoula dakh sa khôl dafa rafét thi kaw rék si kanam machallah contane nagnou si yaw yalna la yalla lafal thiate té bayi lafi
Qui est là en 2024
Machalah wally annif validè boul meusa ragal dara sa papa dala gnanal lepay bakh inchalah bne continuation frère
RIP mon artiste.. Yalnala yalla khare aldiana
Longeu vie,santer a tous les mère yalna sougnou yaye yii fekai sougn ndierigne barkei seydina mouhamed psl
Man mom j m dis k té l meilleur papounet borom khol bou rafet bi diam rk gey am chéri mum sokhna aidara Mme seck yallah nala serigne Bamba tahawou et o6 merci pour tt j né mm op les mots daddy
Qui est la pour le jour de son décès thione balago Seck que la terre lui soit légère 😭😭😭😭😭🙏🙏🙏
Que dieu te pardonne et que dieu t'acceuil dans son paradis le plus heureux éternel firdawss Amine inchallah à chaque personne qui regarde cette vidéo nous vous demandons selonellement de formuler des prières très très très profond destiné à notre défunt le papa thione que le créateur de l'univers vous accorde la paix et la terre de Yoff soit très très très très très légère à tous moments je suis gravement triste de votre disparition une fois arrivé au pays inchallah je passerai chez la famille pour présenter mès très sincère condélence force à toi mon frère Wally Ballago seck force à toi
C'est triste c'est comme si il a senti que il va partir bien tôt
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Li dawna yaram rest in eternal peace papa Thione u will be missed 😭😭😭😭😭
Bilahi li doma si doyal
Wali Yallah nala yallah lafal thiat séck papa thione yallah nako yallah yeureum té kharéko aldjana 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Nékhoul ba nékhoul mais Wally doméram leu😁.il est trop fort
Lii douma sii doyal 😍😍😍
Oh!!! 😭😭Machallah ça m'a touché vraiment "dawna yaram" c'est beau à voir "yalna diam yagu" Peace and love 💞😍
Wa li nekhoul samedi dh khaw touti ma xeum GT dakh émotions jeté tellement contente yalna yalla goudal sen fane waly mala begue pir
Oh purée oh mince me va droit au coeur machallah père &fils lat thiat rek très mignon deux voix qui enveloppent c'est mignon de voir ça ❤❤❤❤❤
Hoo papa thione ndeysane yalna léne yalla sam té goudal séne fane jadoooooor❤😘😍
Machallah lafthiat lepp pape thione la akk diaga YALLA nasen diam yague we are very happy ❤❤❤❤❤❤❤