Serigne moudu mbacke mom Serigne Moustapha .AWDÉGUINE WOU RAFÉT CI WAKHI CHEIKH THIORO MBACKE DÉPUTÉ

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 янв 2025

Комментарии • 42

  • @babacarndao7931
    @babacarndao7931 19 дней назад +1

    Diaradiaf s modou Mbacke kadou yi amna solo ❤❤❤

  • @modouawaballadiouf841
    @modouawaballadiouf841 18 дней назад

    Machallah diaradiuefety mbiake Balla amna solou loul

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 19 дней назад

    Machalla Mbacke balla ❤❤❤❤❤❤❤

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 18 дней назад +2

    Kou bakh boul djawalé securité ak worma
    Bayfall yi wormay Touba lagn yor pas securité

  • @KhadimLam-ps6sy
    @KhadimLam-ps6sy 19 дней назад

    Machalha Mbacke balla

  • @modoumbayeka5045
    @modoumbayeka5045 19 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692 19 дней назад +1

    Merci beaucoup serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @babacarndao7931
    @babacarndao7931 19 дней назад

    S Cheikh thioro wakh diou rafett la wakh ❤❤❤❤❤

  • @fatoufall752
    @fatoufall752 20 дней назад +1

    MACHALLAH SA WA WAKH RAFETNA LI MO GUENE DI YE FITNA

  • @bayetoubasylla7327
    @bayetoubasylla7327 19 дней назад

    Machine amna solo

  • @ebrima6122
    @ebrima6122 20 дней назад +1

    ❤❤❤❤❤❤merci cheikh Thioro Jeurajeuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692 19 дней назад +1

    Grazie mille serigne Touba ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️

  • @damembaye8187
    @damembaye8187 20 дней назад +1

    Yalla na Yalla yokou diamou boubaha ❤❤❤

  • @ebrima6122
    @ebrima6122 20 дней назад +3

    CHEIKH THIORO LIMOU WAX LOU LĖRLA

  • @ABDOUGADIAGA-m7h
    @ABDOUGADIAGA-m7h 19 дней назад

    Amna solo

  • @ebrima6122
    @ebrima6122 20 дней назад +1

    ❤❤❤❤Jeurajeuf cheikh Thioro Jeurajeuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Saliou6530
    @Saliou6530 19 дней назад

    Machallah mbacke balla sa dégue dégue rafétna

  • @malikthiong7839
    @malikthiong7839 20 дней назад +2

    ❤❤❤❤❤

  • @PapaFall-r4n
    @PapaFall-r4n 19 дней назад

    ❤❤❤❤❤

  • @serignemoussa995
    @serignemoussa995 19 дней назад +1

    Ki mo wakhé kham kham ❤❤

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 18 дней назад

    Bilahi walahi bis bou Touba guené thi lokhoy bayfall yi moy deuk bi yahouna

  • @sidyndiaye4697
    @sidyndiaye4697 19 дней назад +1

    Merci beaucoup wakhga deg de

  • @ousseynousall5808
    @ousseynousall5808 20 дней назад +1

    Vérités absolu serigne cheikh thioro ❤❤

  • @ibrahimdiouf2101
    @ibrahimdiouf2101 19 дней назад

    I
    Li seringe cheikh wahkh dak la

  • @ebrima6122
    @ebrima6122 20 дней назад

    Wawe gôr ❤❤❤as wakh rafetna ❤❤❤❤

  • @thiernotoure5713
    @thiernotoure5713 19 дней назад

    Cheikh thioro dagu la wakh

  • @ebrima6122
    @ebrima6122 20 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Jeurajeuf cheikh Thioro ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhounandao9275
    @cheikhounandao9275 19 дней назад

    Jeurajeuf sang bi

  • @CheikhounaMbackeDiagne
    @CheikhounaMbackeDiagne 19 дней назад

    Siwil dou attè siwil psk day waral fayanto tè guisnagne kofi tè diagn kofi guisat nafekh bakhoul

  • @SerignecheikhGueye-mc7nh
    @SerignecheikhGueye-mc7nh 18 дней назад

    katale ndayame fale yena yame

  • @MamedaraThioub
    @MamedaraThioub 19 дней назад

    Li S thioro wax niép dégnanouko
    Guinaw parparloo kéne meunoiko layale boudé deugueu mola takha diok

  • @damediagne7040
    @damediagne7040 19 дней назад

    Li serigne def kay andoussi bossi andon dou wakh limou wakh

  • @serignesamembacke1867
    @serignesamembacke1867 19 дней назад

    boy damalay saa nga dé

  • @assanebambatine8472
    @assanebambatine8472 19 дней назад

    WALAHI MBACKÉ LINGA WAKH REK NINGAKO GUISSÉ LOLOULA CHEIKH THIORO WAKH, LOLOULA CI JUBBLOU , LOU RAFETE REK, CHEIKH THIORO KHALATOU DI AM LENE LIMOUY WAKH CI NDIGALOU SEGNE MOUNTAKHA. LOU GUEUNA SÉCURISÉ TOUBA KESSÉ LA CI JUBBLOU.
    PM SONKO AUSSI LIMOUKO TONTOU LERNA , DEFKONÉ ANDE NA CI SÉCURITÉ BI NGA WAKH , DINANIOU WAKHTANE AK NINIOU CI WARA WAKHAL , LOUNIOU CI WAR NIOU DEFF KO, TE KEN KOUNEK KHAMNA PM SONKO AK KOUMOU DONE CI GOUVERNEMENT SEGNE MOUNTAKHA MBACKE LAY WAKHAL CI SÉCURITÉ TOUBA.
    NIOUNE NAGG TALIBEYI, MBA MANE BOGG TALIBÉ BAMBA BOU KHEBOU GUI , LEK LEK NIOU AM NDIAKHRÉ LOLOU, NDAKH NIENE CI SOUNIOU KELIFA YI DENIOUY BARIL AYE WAKH ANTÉK A WERANTÉ LOLOU TÉ LOLOU NEKHOUL NIOUNE TALIBÉ YI, WALLA SOU KOU BOKK CI NDIAMBOTTE GUI WAKHATÉ LOUNGUENE TEGG NÉ DA JUMM, WOOLÉN KO CIBB NEG WAKH AK MOMOU MOU LERAL, WAYÉ MEDIA YI NGA KHAMNÉ TOUBA NGAY TAKK, TOUBA LAFA KHEW DOYNA WAAR, DIROUBE AY BESS DENIOUY SOSSE REK, LOLOU BEPP KELIFA WARNAKOY MOYTOU NEKHOUNIOU NAGG NIOUY TALIBÉ YI.
    NIARI EXEMPLE REK LA CIY DIEUL , NDAKH MOUNGUI BEUGA BARI.
    TÉ MANE SASSOUNEK DEMA CI ADDU NGUIR MOU NAKHARIMA.
    BA THIA DIEK: WAKHI BOROM DAROU, DA WEDI WEDI NÉ WAKHÉ WOUMAKO NONOU , DIEGLOU NIOU TOPP KO REK.
    BÉNENE BI S .AMSATOU IBN SEGNE ABDOULAHAD .
    TÉ NIOM NIEUP CI NDIAMBOTTE GUI LANIOU BOGG, KEN CI NIOM KHALATOU WAKH CI MOURIDE GUI LOU NIAW , KOU CI NEK LOU BAKH REK LA DIOUBLO WAKH . KHANA NDIOUMTÉ MEUNA AM, NDAKH KOUDOUL DIOUM AMOUL.
    NA SERIGNE CI MOYTOU MEDI YI, RUclips YI NGA KHAMNÉ AYE NOMBRE DE VUES REK MOLENE NIORE POUR AM KHALISS.
    MANGUI TOUBE TEY DIEGLOU .
    WASSALAM.
    TAWFEKH AK TAYSSIR

  • @modoundiaye6044
    @modoundiaye6044 19 дней назад

    Dégayi barina lool

  • @hiciao4882
    @hiciao4882 19 дней назад

    Yamana fen nga xam cheikh thioro boubakh

  • @mamadou438
    @mamadou438 20 дней назад +1

    Wahga deg