Coumba Gawlo - Ndiawnaré (Clip officiel)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 янв 2025

Комментарии • 473

  • @silvestmase5239
    @silvestmase5239 6 лет назад +65

    Kou beugue Serigne Moustapha Sy beusel j'aime ma guisse ❤❤❤👌👌👌👍👍👍

  • @saliletvsenegal5304
    @saliletvsenegal5304 6 лет назад +319

    Kou kontane beusal j'aime

  • @mamefallou1465
    @mamefallou1465 Год назад +3

    Qui est la après le discours de Serigne Moustapha s'y ❤ en 2023

  • @diarrandiaye1487
    @diarrandiaye1487 5 лет назад +22

    "Ya djité ndaw gni orienté len bagnou mat yalla diam, diangal ngalen yare ngalen Serigne Moustapha Sy sangue ba ngui"
    Machallah Coumba gawlo la voix d'or

  • @dialloamethsow7965
    @dialloamethsow7965 6 лет назад +1

    Jetador bilahi si je pouvais te voir coumba si une fois tu as li mn commentaire sache k jtm bku

  • @cheikhlo4641
    @cheikhlo4641 6 лет назад +43

    Sagal nganiou yalla nala yalla sagal. Clip bi dalna te yiw neu. Nourouna borom souko nouroul woone rek niou tiiite donc dieureurdieuf

  • @modoudioplg1302
    @modoudioplg1302 6 лет назад +86

    Que dieu protége serigne Moustapha sy

  • @coumbambaye2417
    @coumbambaye2417 6 лет назад +32

    Merci sama tourondo walahi ndaye sane nala Yalla fay yiw té weral bat bi Si Barker Serigne Moustapha Sy

  • @mansour1297
    @mansour1297 6 лет назад +32

    Wawae defatina pire thiey gawlo laf thiat ana gniko beugg wanalene sene boppeuh pouse bleu wayy

  • @kebalioune
    @kebalioune 6 лет назад +89

    Diara tinga fa nga dane diar et ce depuis plus de 25 ans.le professionnalisme est a son sommet.L œuvre est presque parfaite sans faille.felicitations Diva😍😍😍

  • @myriammbengue9573
    @myriammbengue9573 3 года назад +5

    La diva kumba par la grâce de Seïdi Cheikh Mouhammad Moustapha Sy Makhtum que tu soit guéri à jamais de ta maladie insh Allah Bidjahi YA RASSOUL LILAH

  • @mbeusseneymar5862
    @mbeusseneymar5862 4 месяца назад +1

    Mais Coumba nimouy df voix bi nèkh nama ohh❤❤❤😰🥰

  • @OusmaneNdione
    @OusmaneNdione 6 лет назад +35

    Ay way Yaw ya wax lii si Sama Yakar tey ak Euleuk Yalna Yalla Fey leu Yiw.

  • @halimayat1928
    @halimayat1928 6 лет назад +70

    Extraordinaire sa beauté sans khessal yaw la gueum mane

  • @reinemere7169
    @reinemere7169 6 лет назад +66

    SERIGNE MOUSTAPHA SY ❤
    T TOUTE BELLE COUMBA 😍 LA VOIX JUSTE WAOUH 😊

  • @ousseynoudiagne440
    @ousseynoudiagne440 6 дней назад

    Walay daysane vérité absolue ❤❤❤❤❤ yalla n'a yalla fayale niou Serigne Moustapha sy ❤❤❤❤❤

  • @lamlam-ft2yr
    @lamlam-ft2yr 6 лет назад +14

    SOKHNA COUMBA SAGAL GUA GNOU SI KANAMOU ADOUNA YEUP YALLA NA LA YALLA SAGUAL SI BARKE SERIGNE BI IN CHA ALLAH

  • @dudu8616
    @dudu8616 6 лет назад +41

    Les vrais ont reçu la notification !

  • @papaweindediallo5633
    @papaweindediallo5633 6 лет назад +46

    Manchala la meilleure des chanteuses dans le monde entier

  • @fatoukinetoure3658
    @fatoukinetoure3658 6 лет назад +47

    Bilay do senn morom Yalla na Yalla weral bat bi

    • @ouleymatoudiallo7465
      @ouleymatoudiallo7465 6 лет назад +1

      wakhal waye wallahi dou gnomm maljeureusement son talent n'est pas reconnu a sa juste valeur au senegal

    • @diakawaka7033
      @diakawaka7033 6 лет назад

      SENEGAL KHAMOUGNOU VALEUREUM

  • @ousmanediallo234
    @ousmanediallo234 6 лет назад +55

    j ai des frissons que dieu te protege gawlo internationale khol yeup sedna way wayyalll

  • @ZeynabRassoul1
    @ZeynabRassoul1 6 лет назад +3

    MashaAllah Serigne Moustapha Sy responsable moral du Dahiratoul Moustarchine wal Moustarchidati. Domi Serigne Cheikh aka gno bari xam xam

  • @ndatycisse696
    @ndatycisse696 6 лет назад +7

    L'héritier du khadara ,Machalla coumba dinala teral nagnou yalla may goudou fane

  • @soukeynaniang3240
    @soukeynaniang3240 6 лет назад +17

    non tata coumba ni nga dékkalé thiossane nékh na torop ... you méll ni rek nga war di waaye do moromou bène khalé

  • @doudoudiongue8869
    @doudoudiongue8869 6 лет назад +7

    MachaAllah Coumba gawlo Kènn dou yow woy rék nga meune souma sagnone Clip bi dafay am Imagou Sérigne Moustapha Sy

  • @fatousarr7992
    @fatousarr7992 6 лет назад +2

    ndessane serigne moustapha sy notre responsable moral

  • @natashacham5892
    @natashacham5892 6 лет назад +16

    Chai gawlo. wa ane fans yi

  • @untelheisthebest7223
    @untelheisthebest7223 6 лет назад +10

    Une chanson magnifique chantée par un femme magnifique , l'une des rares artistes à rester naturelles . Elle traverse les années avec grâce et est toujours aussi belle , elle a trouvé la fontaine de Jouvence . Dommage que la plupart des Sénégalais ne connaîssent pas sa valeur et préfèrent écouter des chansons qui parlent de "wouyaye "," reukenté" qui n'ont aucun sens . Je suis son premier fan . Vive Coumba , Faada , Tafa Diarabi , Abdou Guité , Diogal Sakho , Nigga Maas ,Bidew bou bess , Assane Ndiaye , Maréma Fall , Chapman ,Sinatra ,Alicia Keys , Imany , Wonder , Coldplay , Adele ,Maroon5 ,Onerepublic,McSoolar , Ed Sheeran , . .....eux chantent vraiment et les mélomanes le savent .

    • @babacardiouf1585
      @babacardiouf1585 2 года назад

      Faut ajouter elage Diouf Ismaël lo Souleymane faye

  • @kenegawlodiagne6319
    @kenegawlodiagne6319 6 лет назад

    Niaff khole sedda tina dai sama fierte sama gawlo tres oiriginal machallah couleur yi rafet neu sagneser bi diek na ak tare bi dieureudieufaty Coumba way gua deugu Serigne Moustapha aka gueune yalla nala yalla fay say fans namou niou darra ya niou saggal lol

  • @maraniang1066
    @maraniang1066 2 года назад +1

    LiGua waye Serigne Moustapha takhena sa febarbi gnanal nala woorna sarakhéna pour yalla matelas weur

  • @amintambayembaye7181
    @amintambayembaye7181 3 года назад +2

    Lima nekh si ay chanson wam dou wayantou mom loum wayy rekk dako tekk si fouler

  • @awalo2521
    @awalo2521 3 года назад

    Yallna yalla wéral sa batt si barké Mohamed psl🥰

  • @numerouno8620
    @numerouno8620 6 лет назад +2

    Manchallah nexna torop talibé serigne touba nilay mele..

  • @khalifababacardiagne1441
    @khalifababacardiagne1441 5 лет назад +3

    Walay ndeysaan
    Mo beugueu baayam sagal maamam! !!!!💚💚💚💚

  • @biguebijou4488
    @biguebijou4488 6 лет назад +36

    Thiey Gawlo sa tein bakhna je t'adore ma chérie

  • @maimounasenghor4488
    @maimounasenghor4488 6 лет назад +1

    Machalla Tata coumba weuygua kou mata weuy sy demba souniou serigne ,responsable moral ,chef de guerre et grand patron yalna yalla faye té weural bat bi

  • @doudoudiatta1562
    @doudoudiatta1562 Год назад +1

    ❤ @ Tonton Moustaf Sy Mame Cheikh Tidiane al Makhtoum ibn Seydi mame Aboubacar Sy tu est la fierté de Sokone est Tivaoune al barka v🎉 😅 😅

  • @seynabouba3047
    @seynabouba3047 6 лет назад +10

    J'admire tellement cette femme gracieuse intellectuelle naturelle bravo Coumba longue vie Amine. Paysage naturel dans le clip j'adore.

  • @babacarlo5894
    @babacarlo5894 6 лет назад +15

    Merci Coumba Gawlo. Nous sommes vraiment très contents . Yalnala Yalla défale khèwale boubari si zahir ak bâtine.

  • @AbdoulAzizDioplOfficiel
    @AbdoulAzizDioplOfficiel 6 лет назад +6

    Maaaaaaa chaaaaaaaa ALLAH contane na loooool sakh

  • @Diopy1
    @Diopy1 5 лет назад +4

    Qui l ecoute en 2019😍? Way bi chef d'œuvre leu

  • @talibereklabeuguedonendao5904
    @talibereklabeuguedonendao5904 6 лет назад +3

    Walahi ndeysane ken dou cheikh seydi mouhamedoul moustapha sy malick yallah na gnou kou fi yallah yagalal bou bakh té mou and ak wéer bou bakh thi barké mame cheikh seydil hadji malick sy rta amien yarabbi merci beaucoup coumba gawlou one love

  • @roomnart
    @roomnart 6 лет назад +12

    Sa voix est d'une force extraordinaire.

  • @ramatousanogo1121
    @ramatousanogo1121 6 лет назад +6

    Ma Celine Dion de L'AFRIQUE Koumba GAWLO I love you la princess depuis Mali 👄👄👄👄👄

  • @mouhamadoundiaye4734
    @mouhamadoundiaye4734 6 лет назад +58

    Magnifique sa voix . notre Whitney Houston.....

  • @mamadoudiol6239
    @mamadoudiol6239 6 лет назад +2

    Kou bègue coumba gawlo Bessel maye giss

  • @bijoumoulayedabah
    @bijoumoulayedabah 6 лет назад +8

    Qui comme moi a liker avant de regarder?
    Loudoul Gawlo safouma!

    • @diakawaka7033
      @diakawaka7033 6 лет назад

      Senegalese Queen I did the same 😁😁

  • @Diopy1
    @Diopy1 6 лет назад +11

    messou ma guiss waay bou neexé nii j'ai des frissons quand je l'ecoute
    ça restera un chef d'oeuvre sans aucun doute

  • @Wadefootballetbasketball
    @Wadefootballetbasketball 4 года назад +1

    Yalla n'a bat bi yague wer, sama diva coumba,sama Serigne Moustapha s'y ,contane n'a si yaw, môme rekh lagniou am, meilleure clip et son .

  • @mounassseck9396
    @mounassseck9396 4 года назад

    Ndeysane lii nekhna maneu mouride la dh mé dama beugue serigne moustapha sy ndakh serigne cheikh al mahtoum

  • @maimounabalde5848
    @maimounabalde5848 6 лет назад +5

    Merci coumba thi way sy malick yalla na yalla bayikofi bassi kanam

  • @abdoulatifcisse9700
    @abdoulatifcisse9700 6 лет назад +12

    way ga kou diara way machallah yalla na la yalla Faye ya Coumba la grande diva à la voix d'or

    • @abyniang3254
      @abyniang3254 6 лет назад +1

      Abdoulatif Cisse bilahi wakha tiko way na souniou responsable moral

  • @fanswallyseckofficielle7079
    @fanswallyseckofficielle7079 6 лет назад +14

    Thiey sunu Idole thia kaw thia kanam

  • @mouhamedndiaye4861
    @mouhamedndiaye4861 3 года назад

    Walaye ndeysane Mourchidoul Maktoume yalla nanouko yalla fayal Serigne Moustapha Sy❤️

  • @omarediery2069
    @omarediery2069 Год назад

    Diéridieuf coumba gaw lo yalna yalla fay la yiw in challahh barckéb gorgui in challahh ♥️♥️♥️♥️♥️❤🤲🤲🤲🤲

  • @diamilfaye6205
    @diamilfaye6205 6 лет назад +1

    seck iow dal joxnala ci way bi Disc d'or, voix d'Or , micro d'Or ak 1 milliard ndax danga way sama responsable moral. waybi dina siw bamou jaxala. machalla

  • @papadiop651
    @papadiop651 6 лет назад +7

    Ndaysann Serigne Moustapha notre responsable moral merci Coumba🙏🙏

  • @dethiediallo2705
    @dethiediallo2705 6 лет назад

    Kou meunoul bawo louyakhou yawa diarama merci diadieuf

  • @awacheikhseck6754
    @awacheikhseck6754 3 года назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤SY DEMBA DEMBA aka nékha way NDEYSSANE NDEYSSANE yalna yalla SAAM la AAR la LAAKH la fou YAAKH YÉGUOUL inechalla

  • @mamadoudieye7782
    @mamadoudieye7782 6 лет назад +2

    machallah la diva yalna bate bi wer lol waye gua kou bakh kou gnou bakh gneup beugue machallah saaguou tivaoune machallah yalna waye bi yague inchallah

  • @savaneibrahim6218
    @savaneibrahim6218 6 лет назад +8

    Je ne comprends pas ce qu'elle dit mais ça me donne la chair de poule

    • @K71787
      @K71787 5 лет назад

      😘😘😘😘❤❤❤❤❤❤

  • @cambaye60
    @cambaye60 6 лет назад +55

    Kiii bokouthi kw Coumba ténga maaa nopp nguir YALLA ak weerou kooor bi

    • @choupi_3468
      @choupi_3468 6 лет назад

      😂😂😂😂daguakoy tak heuy souba diomi😂😂😂🙏sorry

    • @ndellamar4824
      @ndellamar4824 6 лет назад

      Mbaye ca mashallah coumba

    • @dioufyCOOL
      @dioufyCOOL 6 лет назад

      boy yamal ki samma bosse la mala ka geune nope mome lay weurr

    • @gorangom63
      @gorangom63 6 лет назад

      Maybe
      Pp ca you

  • @katyniangndiaye5098
    @katyniangndiaye5098 5 лет назад

    Yalla nala yalla faye si Barke S. MOUSTAPHA SY

  • @esADServices
    @esADServices 6 лет назад +3

    Machalakh yalna yalla weral bat bi waye nga kou diara waye

  • @minasy9566
    @minasy9566 6 лет назад +3

    Machallah gawlo ligua waye richena sy Malik

  • @khadijandiaye6113
    @khadijandiaye6113 6 лет назад +13

    Aww Elle a Encore frappé 💕💕 Xoll Yi Di Fexx Team La Diva A la voix D’or ♥️💯

  • @coumbatahibouniang2537
    @coumbatahibouniang2537 6 лет назад +11

    machallah bilay do sen morom...borom bat bou nekh doukham nopi laff thiat la diva sama touronoooooo

  • @Moustarchidate
    @Moustarchidate Месяц назад

    Linga way serigne kay nit dotou koko way inchallah Machallah waaaaaaay sama yaye dji

  • @amigueye7044
    @amigueye7044 6 лет назад +1

    Mane dal lo waye nekhnama wante bii dase raw sougnou RM yalna Yalla yagalkofi sounou wasila

  • @silvestmase5239
    @silvestmase5239 6 лет назад +1

    Dieuredieufte Coumba machalah yalla na yalla faylla barke seydina mouhamed psl amine

  • @faadeltv3253
    @faadeltv3253 6 лет назад +1

    La diva encore vraiment linguay wooy amna solo nioune li laniou sokhla musique day am DÉGU dégu...
    Yalla nala thiatt sékhlou yalla mayla goudou fane ak werrr 😘😙😚

  • @Fahboye
    @Fahboye Год назад

    Wé are do proud forever 😢

  • @thiatelo5104
    @thiatelo5104 6 лет назад +1

    Machalla yalla nalla yalla Faye yiww inchalla té wérall batt bi .tjrs la meilleure on t'adore 😍😚😘😙😗

  • @awadrame4788
    @awadrame4788 6 лет назад +15

    Encore la grande diva à la voix d'or on t'aime

  • @adjicheikhmarndong8654
    @adjicheikhmarndong8654 6 лет назад +10

    ohhh j'adore sam maman bii

  • @salynamakeup6886
    @salynamakeup6886 6 лет назад +3

    Machallah sama serigne bi rek responsable moral DMWM😍❤

  • @dabafaye2018
    @dabafaye2018 6 лет назад +8

    Nice ma diva machalah

  • @toufashdiop
    @toufashdiop 6 лет назад +9

    Machallah coumba defati nga sa manine 😍😍😍

  • @yayoubayam1915
    @yayoubayam1915 6 лет назад +4

    Boulawoul dara aki wax liguèye diapou ndiambouram

  • @astoumbenga1127
    @astoumbenga1127 6 лет назад +4

    Thiey Sama maman machallah laf thiat daal jt'm

  • @aminatafaye9505
    @aminatafaye9505 6 лет назад +3

    Oh sama karaw yaram yep tahaw n'a. MachaAllah way nga kou diara way. Le clip aussi MachaAllah. Coumba Gawlo mala beug. Fii lala def ❤️❤️

  • @maguicherie2324
    @maguicherie2324 3 года назад +1

    Gnomm gnep dosen morom yaw yaye youssou ndour bou djiguennn, man dh yaye sama préfère, youssou ndour ak waly, yala na Yala weral Batt bi

  • @cutechips777
    @cutechips777 6 лет назад +17

    Comme d'habitube et brille comme une étoile

  • @fatimacissediaboumamedabak198
    @fatimacissediaboumamedabak198 6 лет назад +3

    machallah 💓 long vie santé Tata yagui bag cou Bakh yalnako fi Yãlla mey wer gou yaram AK goudou fan Ken dou Sy Malick 😍💓💓🙌🙌🙌🙌💝💝💟💟💟

  • @theliontv7152
    @theliontv7152 6 лет назад +7

    MASHALLAH

  • @rokhayagueye8639
    @rokhayagueye8639 6 лет назад +5

    khol yangui fékh dall la diva à la grande voix d'or

  • @damepaye3602
    @damepaye3602 4 года назад +1

    Coumba gawlo tu as bien chanté le digne héritier de son père machalah

  • @ouly9152
    @ouly9152 6 лет назад +9

    Machallah ci yaw

  • @aminatandiaye8918
    @aminatandiaye8918 6 лет назад +2

    Macha allah notre dame nice mes amena lousi manque nakh goumba yi dagnouy deglou teukh yi dagnouy setane balène si khel

  • @fatoudiop5227
    @fatoudiop5227 6 лет назад +1

    loulou dfF mou nexx notre gawlo international

  • @MrAnaconda821
    @MrAnaconda821 6 лет назад +9

    Mach Allah

  • @taxiclando1314
    @taxiclando1314 6 лет назад +10

    Sama Diva à la voix d'or.je t'adore Gawlo 😍😍

  • @princessediedhiou6050
    @princessediedhiou6050 6 лет назад +4

    Ndanane rek moh meun def lii Macha'Allah

  • @amydieng7705
    @amydieng7705 6 лет назад +8

    Ah li nekhna

  • @pendatoure2861
    @pendatoure2861 6 лет назад +3

    néxatina deih mashallah

  • @coumbaba7498
    @coumbaba7498 6 лет назад +10

    Nékhna lol la Diva Macha alla

  • @coumbasow2990
    @coumbasow2990 5 лет назад +1

    Taawfekh ak taïssir rk ngaye ame la diva à la voix casserole ioe mhi wéyy sama responsable moral ki beugue bayam sagal mamam Serigne Moustaph si xol yi

  • @thiamfoutanke8497
    @thiamfoutanke8497 6 лет назад +7

    Diarama là diva 👏

  • @savaneibrahim6218
    @savaneibrahim6218 6 лет назад +4

    La diva you're the best thank you mamma

  • @sayeballathioune1793
    @sayeballathioune1793 6 лет назад +7

    Machallah la diva