N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Moom meme bamou defee mouchor bou noir sakh elle toutes belle masha Alla man avant may cliquee la video Jai dit qui nirooo NAk aicha ndekee mom la NDEYSSANE chapau a gouye gui et a toutes lequipe de people 221 aicha Dall bekk nagne si niniou la guisee tayy❤❤❤❤
Ziar nalen aīcha bou fike parega por sey te yalla rek takh man parena por jelle ga neke sama sokhna mabolele yak muhamed yor len te yalla rek takh incha Allah touba laa dake❤❤❤❤❤❤❤
Setoul djikeur ok ? Mbibeul ladone set té amnako Instant yi kay li geune am important comme amoul bac ni bfem formation professionnel lay weur pour réussir sa vie et assurer celle de don bb Donc ay affaire seuy yeuketiwouko doul way
Natou d'où wésss wayé dieuleul leuppp teksiii lokho yalla et dii diamou yalla .yalna yalla faye cette dame machaaalllaaa Machaaalllaaa Machaaalllaaa chapeau à cette dame .
Suis vraiment content de tes retrouvailles avec ta famille, mai sache que attend toi au pire , li sou dialé digua degue té digua guiss venant de ta propre famille mai courage
Sen chaine bi Inch'Allah ci kaname li nga def rafetena dama yeureum Aîch ak daw ci di dokh ak dom ji. Inch'Allah ba rein di deweun borom bi dina avance chaine bi . Bonne continuation
Je suis contente pour toi Aicha et fais le tout pour oublier Thiate et les mauvaises fréquentations khalé nga mais je vois que tu es intelligente Bonne Chance
Ndeyesane yalla boula tégué natou rek amna Loumou la dénthial dangay khol vidéo bé passé dafa done wakh Di dioye taye mingui wakh di rée yalna la yalla geuneu diapalé🎉❤❤❤
Merci Gouye gui, merci people 221, merci à la Tata qui l'a hébergé , merci à la tante et au frère qui sont venus. Aïcha goorgoloul bakh....boula ben goor nakhati...takkou ligey , doundal sa dom INSHAALLAH ❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Gueuneul réglé bégna rousselo gouye gui di yakha ligéyeume ta bégna yakha khélou kila héberger ndakh nite dina def lou bakh dieuléssi déception ba dou beugeuti def lou bakh j'espère que kou bakh kou yiw kou dioub aussi moko récupérer ndakh deukbi dafa tasse YALLAH na YALLAH doli soutoura INCH ALLAH
Ndeysan machalla Gouygui je vs suivez depuis longtemps mais cest la première fois que je m'abonne directement dans votre page .yalnala diapalé bamou done ay association iou maga makk .li ngay def yomboul loubakh machalla .. bizarrement damala guenteu dembeu si goudi nga ior beneu TMAx bou doywar moderne diar si ndokh bou bari en plus ya ngui tek tank beneu moto 🏍️ diko boukh diko diapalé aussi yor matériel camera micro you bari .sila xeuy yaam ssi vidéo bi machalla kou am dara si yalla nga diapal people 221 dina done ay télé si telé yi yalla nala yalla fay
Macha allah nilla kou nieuw feckla ak sa famille mais koula feck thji mbede tamitt bou eu légué doula nawlo yalla na diam yague ❤❤❤tei yaw danga dionguoma kar matal rek yaw
alhamdoullah dieu merci 😢ho ma sœur que dieu te protège et ton bébé aussi et réveil toi maintenant stp respecte toi d'abord avant tout et cette famille aussi ❤❤❤ bon courage 😢
Machallah, Yallah na Yallah faye kou dieul aicha en charge .c'est mal de se faire rejeté par ses parents au sens large. Félicitations à people 221. Vous faites un travail extraordinaire !🎉🎉🎉🎉
Gouye gui waw goor liguéye bi amna solo looll machallah yalla nala yalla faye aw yiw 😢 Ms sa communications xoolat ko wakh mome déssé guako meune bonne continuation frr😊
Son regard en dit long sur ce qu'elle a pu endurer. Mélange de tristesse, douleurs, contentement, fatigue.. Que Dieu Continue de veiller sur toi très chère, Tekk la si yonou Chiratal Moustahim
Il faut toujours aider cette fille sur des conseils et lui trouver du travail et un mari le plus vite possible dah gnamena baparé Lou néhk thé djiguéne la
Mashalla 🎉a vous gouygui et Aïcha prend soin de toi aussi Et de Mouhamed Et refait ta vie Oublie les hommes u es une battante ne compte sur eux pour réussir car u es une femme U es forte Une brave dame Focus rek
*Khol seddeuna thi nimala guissé ni légui nakk gueuneul goorgorlou té bagna may say noon fougnouy réwé wala gni la diapalé am lou len nakari thi dieul bougne la djieul sa dôme ak sa avenir nagnou done sa priorité ❤🙏🏽🙏🏽*
Kou soutoural domou Adama buur yalla def Nala kharittt.. Kone gouye gui iow ak mère biko hébergé ak gnissi diap nieup diapp len ni ay kharitou yalla ngen ndax soutoural ngen xalei bi❤❤❤
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
sawaye denma soufou dank gawe ga dė yalla na yalla berkėl incha allá gracias
Gouy gui diapalè ma
@@fatimafaye-xh6zz Hola
Hola
Chapeau à toi frère
Moi je tiens a féliciter le journaliste jolie travail 🖐️❤️mon frr
Alhadulilah Aicha yow tamit légui boul doug si lignlay yabé amal fouleu ak fayda moytou vraiment ma belle courage à toi.
Abandon mo mëll nonou wlh dou mbonetém
Aïcha nimala guissé tay nékh nama yalna diam yagg ❤❤❤ té gua faté doméram bobou niounane thiat . Refait ta vie et fait attention à qui tu fréquentes
Kokou aicha douko meussa fate dieulma PV
@@moustaphabakhoum6153poureqoi
Loutakh nga wakh ko@@moustaphabakhoum6153
@@moustaphabakhoum6153explique moi
@@moustaphabakhoum6153lou takh 😢
Gouy gui un grand merci pour toi liguèye bi rafète n'a ✊✊
♥️♥️😂😂
Hoooo Ndeyessane sante yalla Mouhameth yalla douco sétane Masha’alla ❤❤❤
Aïcha une femme très belle machalah yalla nala thiate sekhlou
Amine ya rabi
Tiate n’ est pas bon il est mauvais
Amiin❤
Aicha amal fouleu am fayda tė sa bop lėgui gua am dieukeur diou bakh khalė bou rafėt machallah ❤
Lolu ngen ko wara hale bu ndawla moy foow boppam rek
Voila lolou la ❤
Contane na dall😭 ❤️Lima dioyyy la fois passer wallahi yalla ne borome bi sameu léne 🙏🏿😭
Moi aussi bilaye dama dioye sama rogogne yi bimou touro tayoumako surtout bimou wakher Mane awma amourou yaye motakh damaye té sama dôme
@@AbdouDiallo-o8n*Ioe déh loula dioylo moma dioylo wakh bobou dafa percé sama khôl bi mais sante Yalla 🙏🏽*
Bilay ioe mane sakh dama dioy la fois passé mais alhamdoullilah 🙏
Bilaye lolou mom daffa dawon yaram trop boy dioy sakh doko tay
🥺
Un grand remerciements à toi ki fait des beaux gestes en temps k jourliste bravo frère patriote
kiko dimbeuli yalnako yalla fey
Amine
Amiin❤
Amine
Amine ❤
Amine
Bravo Gouye Gui sa liguèye rafét na machalah ❤❤
Yalna yallah fat. Gouye Gui
Moom meme bamou defee mouchor bou noir sakh elle toutes belle masha Alla man avant may cliquee la video Jai dit qui nirooo NAk aicha ndekee mom la NDEYSSANE chapau a gouye gui et a toutes lequipe de people 221 aicha Dall bekk nagne si niniou la guisee tayy❤❤❤❤
❤ay contane na wayyy Aïcha ndeyssane Yalla na sa domm maggg ak diamm inchAllah ❤
Amine ya rabi
Amiin❤
Vraiment Monsieur vous faites un excellent travail machaallah yalna dieum kanam 🙏🥹
Sougnou gnane gui nagouna alhamdou lillah ❤
Bilahi mame yallah reck mo meune❤
Alhamdou lilah
Vraiment sou nieup done diapalantei kene dou sone
Heureusement ya toujours de bonne personne dans cette cie
*Bilay ioe té lima guiss sedd na khôl ❤🥰*
@@khadyjeanineniang5400yalla dou mamou kenn borom la
Alhamdoulilah rabi halamiine
Machallah gouyy gui rafétt na yalla na yalla defall lah diam
gouye gui yalla na yalla faye la li la niepeu done khare auh dieu merci
Ziar nalen aīcha bou fike parega por sey te yalla rek takh man parena por jelle ga neke sama sokhna mabolele yak muhamed yor len te yalla rek takh incha Allah touba laa dake❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂😂 dofo d khalebi bou rafett bi ngani mou niow nga takeu ko melni comme si amoul choix ok
@safietoufall251😂😂😂😂2
Setoul djikeur ok ?
Mbibeul ladone set té amnako
Instant yi kay li geune am important comme amoul bac ni bfem formation professionnel lay weur pour réussir sa vie et assurer celle de don bb
Donc ay affaire seuy yeuketiwouko doul way
@@safietoufall2512bayil yingay déf waay😂😂😂
bilay defale loulou diamou yalle laa
Natou d'où wésss wayé dieuleul leuppp teksiii lokho yalla et dii diamou yalla .yalna yalla faye cette dame machaaalllaaa Machaaalllaaa Machaaalllaaa chapeau à cette dame .
Amine ❤
*Amennn❤🙏🏽❤*
Machallah aicha nga gorgorlou bou baax yala nala yala diapale aamiine
Amine ya rabi
Suis vraiment content de tes retrouvailles avec ta famille, mai sache que attend toi au pire , li sou dialé digua degue té digua guiss venant de ta propre famille mai courage
*Lolo déh la khalate ba togue ni mais Yallah bakhna Yalla nako sougnou Borom gueuneu takhawou🙏🏽*
Machaalah mais nak mouroul sokhna si mola gueuna diap dh wallaby tu est ravisante
Aicha elle est tellement belle takal sa seurr ga ligueyy yalla dinala ay dieukeur diou bakhh inchalah
Alahouma amine yarabi
Amiin❤
Elle est belle Allahouma barick gorgorloul Yalla baxna
Billahi. Rafet mashallah ❤
Sen chaine bi Inch'Allah ci kaname li nga def rafetena dama yeureum Aîch ak daw ci di dokh ak dom ji. Inch'Allah ba rein di deweun borom bi dina avance chaine bi . Bonne continuation
Je suis contente pour toi Aicha et fais le tout pour oublier Thiate et les mauvaises fréquentations khalé nga mais je vois que tu es intelligente Bonne Chance
Oui elle a fait l’ école jusqu en 5 eme et la famille de Dakar l’
Avait mise à l
École coranique tu te rends compte et l’ ont chassée de la maison
Ndeyesane yalla boula tégué natou rek amna Loumou la dénthial dangay khol vidéo bé passé dafa done wakh Di dioye taye mingui wakh di rée yalna la yalla geuneu diapalé🎉❤❤❤
Bilahi machalah
@@mamemorfall3066 ♥️♥️
Wa mais ki Aïcha la ah djiguene bou khélmy dalé rék mou raffét ohhhh 😂😂😂
🥰🥰🥰
Wallahhi nk
Billaye djiguene yallah mokou térall ❤
*Bilay wlay😢🥰*
Ki naturellement dafa rafet
Je suis tellement heureux et content ses lèvres mérite cette sourire 😃 ❤
Bly ndeysane na gorgorlou rk❤
Gouy Masa Allah mercie beaucoup grazie mille vielen Dank ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla je suis contente la foie passer dama dioye ba sone ❤❤alhamdoumlilla Machalla
gouy gui kou deff lou bakh yalla fayla lou bakh yalla nala yalla faye ❤❤❤
Gouy gui yalnala yalla fay yew
Machala nitt amul lou euppeu mbokam amna.solo ❤❤❤❤❤❤
Machalla bonne nouvelle yalla na ko Yalla defal diam
Wadji liguéye yamm raffétte naa neyssane kou amm yeurmandé ❤❤❤❤❤❤
Li moy Senegal 🇸🇳❤😭
Naga goorgolou nak té am foula ak fayda❤❤
Wayer people yenn diam si yenn un excellent travail Machallah
Merci Gouye gui, merci people 221, merci à la Tata qui l'a hébergé , merci à la tante et au frère qui sont venus. Aïcha goorgoloul bakh....boula ben goor nakhati...takkou ligey , doundal sa dom INSHAALLAH ❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Gueuneul réglé bégna rousselo gouye gui di yakha ligéyeume ta bégna yakha khélou kila héberger ndakh nite dina def lou bakh dieuléssi déception ba dou beugeuti def lou bakh j'espère que kou bakh kou yiw kou dioub aussi moko récupérer ndakh deukbi dafa tasse YALLAH na YALLAH doli soutoura INCH ALLAH
*Srtt lolou mais ayons l’esprit positif 😢Amennn🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Surtout lolou waye ndiorte bu rafete rek yAllah baxna
Degue pire gua wah wayé yala bahna
Deug rek nga wax nitt day kham bopam règle tag nsigeum ligueye tag seureum
Ndeysan machalla Gouygui je vs suivez depuis longtemps mais cest la première fois que je m'abonne directement dans votre page .yalnala diapalé bamou done ay association iou maga makk .li ngay def yomboul loubakh machalla .. bizarrement damala guenteu dembeu si goudi nga ior beneu TMAx bou doywar moderne diar si ndokh bou bari en plus ya ngui tek tank beneu moto 🏍️ diko boukh diko diapalé aussi yor matériel camera micro you bari .sila xeuy yaam ssi vidéo bi machalla kou am dara si yalla nga diapal people 221 dina done ay télé si telé yi yalla nala yalla fay
Ndeyssane khalei la yalla mou toudoneu dome si vie wame Aicha na gueuna guor guorlou yalla bakhna ça ira avec le temps unchallah
Machallah ❤yalna yalla faye yiw
Ndeysane Li daffa nékh trop billahi Amale diam rék ♥️♥️♥️⚜️✅🥺🙏🏽
Macha allah nilla kou nieuw feckla ak sa famille mais koula feck thji mbede tamitt bou eu légué doula nawlo yalla na diam yague ❤❤❤tei yaw danga dionguoma kar matal rek yaw
Machallah gouy gui yalla nala borom bi faye
I’ve never been this happy seeing aicha back to normal
Alhamdoulilah bb Mohamed yalnako yalla tegue lokho
Li dé moy nite di défar aka niawe wayé téssaneté doula laneté yakaneté Guy gui yalla nala yalla fayy yiwe bonne continuation â Aicha
Ah macha allah dieu merci ❤ alhamdoulilah
Elle était plus belle avec le foulard, les perruques là moy lolou.
lou léer
Blh yw🎉
alhamdoullah dieu merci 😢ho ma sœur que dieu te protège et ton bébé aussi et réveil toi maintenant stp respecte toi d'abord avant tout et cette famille aussi ❤❤❤ bon courage 😢
Gouye gui mâchions spécial à toi ❤❤👏👏👏🇸🇳
Où est ce que vous allez mâcher et qu'est ce que vous allez mâcher ,,, j'ai tellement faim
@@serignemodousylla9484😂😂😂😂😂
Apres tout les sénégalais ont un bon cœur ❤️
Ndeyesane mome dafa rafétte sakh❤
Chapeau People 221 Bon boulot Good Job
Machallah, Yallah na Yallah faye kou dieul aicha en charge .c'est mal de se faire rejeté par ses parents au sens large. Félicitations à people 221. Vous faites un travail extraordinaire !🎉🎉🎉🎉
Mashaa allah félicitations gouygui nala yallah fay mo mit yallah tegaatko thi yobou siratal moustaghim in shaa allah
Bravo maintenant faudra soigner son père ❤inchallah
Gouye gui waw goor liguéye bi amna solo looll machallah yalla nala yalla faye aw yiw 😢
Ms sa communications xoolat ko wakh mome déssé guako meune bonne continuation frr😊
Machalla gouy gui contane nagnou gno bokk deuk malika
Ohhhh machallah Alkhamdoulillah
Aicha sa dome bi yalna ko yalla teral mou teral la aussi baye bi mome bou aduna nekh bangua nekal ak mome encore mla ko niane
Son regard en dit long sur ce qu'elle a pu endurer. Mélange de tristesse, douleurs, contentement, fatigue..
Que Dieu Continue de veiller sur toi très chère, Tekk la si yonou Chiratal Moustahim
Aicha kayi tayi machallah main moytouss domeram you melni tiate tu es belle vraiment gor gor loule❤❤❤❤
Il faut toujours aider cette fille sur des conseils et lui trouver du travail et un mari le plus vite possible dah gnamena baparé Lou néhk thé djiguéne la
Mashalla 🎉a vous gouygui et
Aïcha prend soin de toi aussi
Et de Mouhamed
Et refait ta vie
Oublie les hommes u es une battante ne compte sur eux pour réussir car u es une femme
U es forte
Une brave dame
Focus rek
Respect champion ❤Gouyegui
J’ ai pitié de Aicha j’ ai mal Aicha courage qu’ on continue de lui envoyer l’ argent s’ il vous plait
Machallah n'a guoreguolou té mougne leup Dina bakhe
Mais ce que je comprends pas moye loutax Aïcha informéwoule tantame bi
Grand bi merci beaucoup ❤❤❤
Alhamdoulilah 🤲 dieu merci porte toi bien ma chérie 😢
Gouy gui un grand merci pour toi liguèye bi rafète n'a
Machallah guuy gui yalna yallla fay Aicha ioa tmt nga gorgolou bou bakh yalla bakhna ❤
Respect à toi frère du courage longue vie à vous ❤❤❤
merci beaucoup Grand ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment grand bi sa liguéye rafette na trop machalah Yalla na sénn diamou yague ❤️
Nguirr yalla Aïcha goorgoloul nak amga sass bou reuy dé ...hummm
Lolou mo diara wakh
Bilay sass la dh yalla Nako yalla defal diame t mou takkou am fouleuh keine bagne ko deigu
Aaa alkhamdoulila fille goorgorloul tèyè sa bope et longue vie à mouhamed boul guèstout le papa de ton fils bayiko à vie du courage
*Khol seddeuna thi nimala guissé ni légui nakk gueuneul goorgorlou té bagna may say noon fougnouy réwé wala gni la diapalé am lou len nakari thi dieul bougne la djieul sa dôme ak sa avenir nagnou done sa priorité ❤🙏🏽🙏🏽*
Alhamdoulahi yalla na yalla doli soutoura si barke baye niass
Kou soutoural domou Adama buur yalla def Nala kharittt.. Kone gouye gui iow ak mère biko hébergé ak gnissi diap nieup diapp len ni ay kharitou yalla ngen ndax soutoural ngen xalei bi❤❤❤
Machalah Aïcha yalla na yalla déf diamou naga faté domérame dji thiate
Machalla yallah nalen yallah takawo ❤❤❤❤
Surtout lolou gouy gui na tak sereum té Gorgorlou nit dafay ame diome khole li nék sa guinay
Bonne chance té nga Yam.
😂😂😂
Elle est très belle machalla ❤❤❤❤bon courage ma puce
Guiy gui yal nala yalla fay si barkhe serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci gouye gi
La journaliste merciv beaucoup❤❤
Fassal diom tè mouñ likay bañ top n’importe qui
Te yalla sam leu
Gouyegui konetane Nanou si yeuw li kou raféte khol rék moko meune aicha fasse diome nak mossi désse🙏❤❤❤
You’re so amazing! Thank you for all your help!!
Yaw cana dégo wolof😢
People 221 vous faites un travail excellent Merci
Alhamdoulilah 🎉❤
Merci Gouye Gui du courage Aïcha gua goorgoor lou bou bax maytou mauvaise fréquentation pask djiguèn gua tè gua am fouleu ak fayda ci sa bopp❤
Machallahh diamma daffa nèkh Alhamdoulilah aicha est très belle dallll longue vie à toi
Mashallah Gouye gui yalna Yalla fayla❤
Thieuy Gouye gui yaa bakh dieuredieufeuty dieufeuty dieufeuty