Nidiayou aicha bi Tothiena Kass Yi Papam Mou Raye Yaayam 😱 Motakh Aicha…

Поделиться
HTML-код

Комментарии • 240

  • @LeyeSonko-x8w
    @LeyeSonko-x8w 4 месяца назад +53

    Té bouma dégué séne wakh dafa mélni Aïcha nékoul si lokho famille wam ba légui Aïcha bonoul dé victime la rék diapaléne ko wala mo tombé si bénéne lokho you bone svp🙏

  • @OusmanediandisSane
    @OusmanediandisSane 4 месяца назад +121

    Aicha avec la souffrance quel a enduré motakh boumou guissé kouko beug rek Dafa daw pour meun soulager wou aufet khôl bi la afekté

    • @nogayefaye998
      @nogayefaye998 4 месяца назад +5

      Voila nak❤

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 4 месяца назад +2

      Effectivement

    • @BayeNdiaye-x3k
      @BayeNdiaye-x3k 4 месяца назад +3

      mais wadji beugou ko sinon douko maltraité après avoir eu un enfant avec elle.

    • @MouhamedGuisse-d8l
      @MouhamedGuisse-d8l 3 месяца назад

      Non j’eus croix pas déjà môme elle avait du mal supporté les truc de relation car def buzzard Dey mérr légui guifff lègui et aussi gniko nobonn bariwonnn na lolll

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl 4 месяца назад +92

    Lii rek motakh mane niane goudou fane, ngir teyel sama bop samay dom bagne lena denk kene niouy sankou. Yor dou khaliss mais topato leu, maname di wakhtane ak mom diko accompagner.
    Affaire papa ji warone nanioukoko neub bamou nek mag mais diko ko khasser motakh mou dem ba def bopam bordel. Elle a perdu sa mère tôt donc gniko yar nioko yakh

    • @maimounambow6292
      @maimounambow6292 4 месяца назад +6

      Bilakhi Yalla naniou fi Yalla bayi yarabi ak souniou ay ndiabote

    • @FatimandaoTymandao-gr4gl
      @FatimandaoTymandao-gr4gl 4 месяца назад

      Amine ya rabbal alamine​@@maimounambow6292

    • @Ndeyendack-fe2jl
      @Ndeyendack-fe2jl 4 месяца назад +1

      Aaamiiine yaarabal aalamiine yalla nanou yalla bayyi thi sounou kanamou ndjiaboot gui gnou goungué leen bagnou gnémé

    • @misterkanhg4347
      @misterkanhg4347 4 месяца назад +1

      Wakhi dof rek ngafi wakh . T’entends parler là . dom ak alal yalla néna fitneu la . Donc niane gudou fann pour say dom la dal . Dénkal yalla say dome té def sa kem Katane. Yalla moy Samou , di tek natou kouko nex . Sofi diougué tamit yalla migui fi .

    • @Ndeyendack-fe2jl
      @Ndeyendack-fe2jl 4 месяца назад

      @@misterkanhg4347 loolou dé am gnoun gnooy diékh gnoofiy diogué waayé yalla dou diékh té doufi diogué

  • @adamandiayekasse5990
    @adamandiayekasse5990 4 месяца назад +48

    Mais Aïcha n’est pas responsable des actes de son père 😢 mm boudé liniouy wakh deugg la, bouniou koko fatali tamitt

    • @AstouSy-f8i
      @AstouSy-f8i 4 месяца назад +6

      Pour sénégalais rek aye deume laniou daniouy laye sossal vrai domérame

  • @mintouhamadouka8949
    @mintouhamadouka8949 4 месяца назад +59

    Sa djikko papa nga yorr assassin nga 😭😭Lii rec meunna takh xalébi doff wola mou xarou 😢c dangereux elle est perturbée psychologiquement wollah

    • @Laylabatoul
      @Laylabatoul 4 месяца назад +6

      Bilahi ndeysan té papa dji kom wéroul loum déf kén douko si top

    • @mintouhamadouka8949
      @mintouhamadouka8949 4 месяца назад +8

      @@Laylabatoul kii liko metti mo beuri thi xalé mais nattou la rec yalla nako yalla taxawou

    • @Laylabatoul
      @Laylabatoul 4 месяца назад +4

      @@mintouhamadouka8949 allahouma amin ya rabi niak ay mbokou you bakh rk nk ndeysan

    • @CheikhThiam-y8c
      @CheikhThiam-y8c 3 месяца назад +1

      Billaye

    • @aissatakebe5212
      @aissatakebe5212 3 месяца назад +1

      Senegalais amoul khol diap nit diko khassé lo khamni defousi meunou si dara 😢

  • @CILABOKKMEDIA
    @CILABOKKMEDIA 4 месяца назад +25

    Aïcha n’a besoin d’aucun aide Psychologique, elle a subit un manque d’affection, et de respect. Elle a été clair et lucide dans sons interview, keur gui mou neka les gens le rappelle l’acte de son père elle l’a même affirmé que sa tante qui censé protéger son secret dakoy wax, elle s’est même dit dans l’interview kan mo wax secret papam thi keur gui. La petite xolam mo diekh mou ham ay mauvais influence natou dalko. C’est tous Amour ak affection rekk mo manqué rien de plus.

  • @khadijetoulykane8909
    @khadijetoulykane8909 4 месяца назад +27

    Très bien, la gambienne, fière de ton intervention. Sa famille est plus que bone puis son propre oncle mokoy yakheu te wornama dañouko yoni pour mou setal derou famille bi

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 4 месяца назад +3

      Effectivement il est mauvais très mauvais une mauvaise famille

    • @AstouSy-f8i
      @AstouSy-f8i 4 месяца назад +2

      Je pense la même chose que toi bilakhi niome nieupe contre khalei bi c douloureux

  • @LeyeSonko-x8w
    @LeyeSonko-x8w 4 месяца назад +82

    Mame dé bouma done ndidiayam bi douma fi nék sakh di wakh damakoy diapalé

  • @BayeDame-k4q
    @BayeDame-k4q Месяц назад +1

    Aïcha defout dara yalla ko natou 😢😮❤nidiaye dji limouye wakh warouko wakh

  • @lacolombeblanche4589
    @lacolombeblanche4589 4 месяца назад +37

    Ba aicha né danio Méré sama papa ndakh limou def la compredre

    • @Zeydatou
      @Zeydatou 3 месяца назад

      😅😅w

  • @aminatawade1053
    @aminatawade1053 4 месяца назад +16

    Ce qu il a dit Aicha l a dit entre les mots .Elle a dit que son père n était pas sain d 'esprit quand il le faisait.Et elle a aussi dit qu on lui répétait souvent cela.

    • @rokhayathiekoulaye8753
      @rokhayathiekoulaye8753 4 месяца назад +4

      Voilà quand elle a dit que sa tante lui a dit assasin ngaa kom ton Pére..... laa comprendre ndeyssane

    • @asmalenguelsy3958
      @asmalenguelsy3958 4 месяца назад +3

      Yow kou ma dégue dégue nga. Si phrase bobou la comprendre que son père a tué sa mere.elle l’a dit entre les lignes.

  • @fatoutine5299
    @fatoutine5299 3 месяца назад +5

    Ndeyssane senegal degn lay def traumatismes morale mental psychologique ba sa bop diahasso ngey chercher echappatoir gnou nane la da nga bone nane la traiter negn la bou bah dougal negn la ecole alhourane manquer wo dara xana xamolene mental trauma bi nguene di def xaleyi que ce soit gni amoul bay gni ci gni ça bilaye safara rek ngene meriter ça jai espoir qu ALLAH le punira fort fort fort amine parcek cest plus que sorcier...courage ma soeur aicha faut k tu te ressaisise vite et reprenne ta vie en main te boul fale kene ton pere cest pas toi et autre...naccepte jamais kon gache ta vie confies tou A DIEU.Il est la pour tous et lui seul a le dernier mot

    • @mamefatoudiagnediop
      @mamefatoudiagnediop 3 месяца назад +2

      Wallahi ils pensent que lek ak naane dougale ecole rek moye traitement bou bakhe té heure bounioi ditté ak yaww thiow bou ndaw niou traité de tous les nom waxla loo xameni daff laye traumatisé toute ta vie

    • @fatoutine5299
      @fatoutine5299 3 месяца назад

      @@mamefatoudiagnediop malako wah bi hypocrisie mane dafma dépassé...en fait dougeul ecole bii lek ak nane bi yeup au final ils font ça pour le nguistel pour paraître bien aux yeux des gens...parcek au final degnouy traumatiser orphelins yi ak enfant abandonne yi mais à un point que gnom bougnou mousssoul ak am dimbalou YALLAH degniy moudj sankou à vie...mo tah mane je les exhorte à beaucoup prier et tt donner à DIEU au moins ndah mou meune lene diapale et faire leur justice pauvres innocents qu ils sont...situation bi gnou neke senegal diegue YALLAH rek kot mo lene si meune diapale...

  • @fayeemilie3929
    @fayeemilie3929 4 месяца назад +21

    Mais elle n'a pas demandé de naître cette fille. Si son père a fait l'irréparable. C'est pas la faute des enfants, les pauvres. Alors il faut arrêter de coupabliser les enfants. C'est douloureux pour la famille mais protéger les enfants 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

    • @couritad4398
      @couritad4398 4 месяца назад +1

      C'est sa que je voulais dire ,et durant toute ta vie, sénégalais, je ne sais pas quant est-ce que les sprints vont-ils changé.

  • @papelatyroulare6964
    @papelatyroulare6964 Месяц назад

    Elle mérite du soutient vraiment

  • @rokhayakaraboye5437
    @rokhayakaraboye5437 4 месяца назад +75

    Je veux récupérer aucha et son bb nguir yala rek

    • @ANNASOWFAYE
      @ANNASOWFAYE 4 месяца назад +11

      Yalna leu yalla faye soxnaciii et yalla mayleu lolenn yorré .

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 4 месяца назад

      Oui fais ça s il
      Te plaît va la voir

    • @diomagirard5899
      @diomagirard5899 4 месяца назад +1

      Vraiment vraiment que dieu vous facilite votre souhait thanks m'y sister

    • @amadiallo-kn2ye
      @amadiallo-kn2ye 4 месяца назад

      Defal lolou sœur nguir yalla je veux joindre la petite Aïcha je vous donne mon numéro au cas où in cha Allah louniou meune si aider ko nio defko

    • @solution5135
      @solution5135 4 месяца назад +1

      Soko déffé té yalla rék takh yalla dinala soutoural euleuk yawmal khiyaam yalla dinalafa défal lokhameni bilahi koudoul doukofa mane ndakh kou soutoural ab djioulit ngir yalla yalla dinala soutoural euleuk yawmal khiyam

  • @aissatougueye7934
    @aissatougueye7934 4 месяца назад +29

    Aïcha yalla nako yalla dimbeuly

  • @oumygyeuye2433
    @oumygyeuye2433 4 месяца назад +20

    Yaye dafa amsolo si niit li yaye meune si yow kenene meunoukosi

  • @diengawa9298
    @diengawa9298 4 месяца назад +16

    D'après les paroles d'Aïcha kou beugueu papam, car D'après ces dires lignouko donn wah si écoles bii ak certaines paroles yi mou donn degg si papam motah manatoull wonn dem diangu .Mais elle n'a rien dit de mal à son père, Aïcha yalla nako yalla guennè si situation yimoul dound incha allah❤❤❤❤❤

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 4 месяца назад +2

      Effectivement tu as raison et ce n est pas son père qui a tué sa mère. Aicha aimait son père

    • @diengawa9298
      @diengawa9298 4 месяца назад

      @@strategiesetdeveloppement2525 exactement

    • @HawaThiam-g8j
      @HawaThiam-g8j 4 месяца назад +1

      Bouléne fi bakarou Aïcha ne connais rien de sa mère day doul rek nio bok

    • @HawaThiam-g8j
      @HawaThiam-g8j 4 месяца назад

      Aïcha hamoul dara thie yayam day doul rek

    • @diengawa9298
      @diengawa9298 4 месяца назад

      @@HawaThiam-g8jdouma wahe si famille diamborrr ndah hama louma lenn darra té lima wah gusou massi bakar boko gussé rekk ganima lilaaa bonne nuit.

  • @misszjuke4914
    @misszjuke4914 4 месяца назад +7

    Mbokk yi nio bonne amouniou ben ndeurine! Khawi soutoura . Vous faites quoi pour l aider! Vous aimez appuyer la plaie.
    Aicha est in enfant abandonné lâchement par sa propre famille . Wah rekk sans solution. Lou ci yonu aicha ci relation entre la défunte maman de aicha et de son père !

  • @MendiayeSall
    @MendiayeSall 2 месяца назад +1

    Barké alkhourane bima sétanê vidéo Aïcha bi silako kham😮

  • @seckkhadijatou9092
    @seckkhadijatou9092 4 месяца назад +6

    Ndeysane adouna métina effectivement dafa sokhla psychologue elle doit être suivie ohhhhh c’est triste 😭😭😭😭

  • @Intégrité-v1p
    @Intégrité-v1p 4 месяца назад +2

    Té mane tamit facilitatrice panel bii bane école ala diangué ???🤔🤔🤔🤔 kou wakh cii lii wakh cii léeee taaamit 😅. Bref votre démarche à ce sujet est vraiment très noble et salutaire. Force à vous 🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @khadijetoulykane8909
    @khadijetoulykane8909 4 месяца назад +7

    Quand à sa tante nak, ex dieukeur am na, mais ex doom amoul. Ngeen seet thi yayam sakh bi geneu adouna sakh. En plus réaction bimou am meun nekeu conséquences yi dioguee thi nga khamni sa papa mo Ray sa yaay😢 lolou kouko atan thi adina. Famille bou doy waar ngeen

  • @couritad4398
    @couritad4398 4 месяца назад +2

    En tou cas les histoires des parents,toujours cest les enfants qui les paye chère, et tres chère, les familles maintient au Sénégal c'est comme des étrangers ,courage

  • @fayeemilie3929
    @fayeemilie3929 4 месяца назад +6

    Elle est traumatisé la pauvre. Il faut lui parler instaurer le dialogue. L'éducation c'est pas d'être trop stricte. 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @diamysidibe7105
    @diamysidibe7105 4 месяца назад +10

    Sénégalais pour mome diam moy lek ak nann solou .... diam d'abord si bob leu

  • @cocosqueen1752
    @cocosqueen1752 4 месяца назад +16

    Ndeysane khelou khalé moko diapone teh niak yaaye mo metti ba paré df am traumatisme le fait papam mo ray yayam meunonako bagna yeuk

  • @juledia2426
    @juledia2426 3 месяца назад +1

    😭😭😭😭🙏🙏🙏

  • @NdeyedadoSarr
    @NdeyedadoSarr 4 месяца назад +4

    Perdre sa maman est trop dure surtout nioulay wakh yéne mot so gueumoul yalla reķ lounék moune gua sédou bilahi

  • @BahyayeDiop
    @BahyayeDiop 4 месяца назад +4

    La femme a parfaitement raison Aïcha était dépressive depuis longtemps bien avant qu'elle quitte la maison familiale

    • @dieynabamamadousy523
      @dieynabamamadousy523 4 месяца назад +1

      Depuis longtemps lo dal yaye yeupeut kanam la am bi am 6mois

  • @syndeye9523
    @syndeye9523 3 месяца назад +2

    Raison pour laquelle vous devez l'aider au lieu de le tromatisez c'est triste les gens sont méchants

  • @YoohGui
    @YoohGui 4 месяца назад +16

    Xalebi wakhone nako ci interwiew bi.. Bako tantam bi di nane yow sa jikko papa ga yorer assassin ga.

  • @AstouSy-f8i
    @AstouSy-f8i 4 месяца назад +2

    Mane Bb bi rek moy sama problème ndeyssane si bire wakham loumou wakh ma mouni douma diokher sama dome donc sou bonone dafa diokher dome bi nek si louko nekh famillam nio bakhoul motakh elle n’a pas le choix

  • @SodaMb0w-me5we
    @SodaMb0w-me5we 3 месяца назад +1

    Aicha lii metty na mais dou tax mouye assalo bopam baparei kou yayamm guene adina daffafa warra mogn ndax diguantei bii yaguoul darra nga ame dieu ❤seuyi bayi lene faa. Soudeffon nii mangam Bobou mougne tei khamnii darra sakhoul boulen jugé tei khamolen tope lene khalei bou djiguene bii fiimou diar yeipe

  • @mariembaye5829
    @mariembaye5829 3 месяца назад +1

    😢😢😢😢😢😢

  • @mariamaouattara8865
    @mariamaouattara8865 4 месяца назад +2

    Effectivement elle a besoin d'aide psychologique
    Sénégal dagnoulay fatali Lou niaw dila khass et Lolou dalay top
    Mane dom bi la gueuna yeureum
    Donc faut la soutenir

  • @aboubacarsidike9806
    @aboubacarsidike9806 3 месяца назад

    Mounouma bindi wolof mais chérif de kou kate ndeyam leu nga nekeu si live di khawi soutoura diamboure digeun rethie bo len demai a lakhira Inchallah

  • @diopmamadou1614
    @diopmamadou1614 3 месяца назад +3

    Il faut parler en Wolof c'est mieux pour qu'on puisse comprendre pour ce qui ont des difficultés en français

  • @strategiesetdeveloppement2525
    @strategiesetdeveloppement2525 4 месяца назад +5

    Le problème c est sa famille qui ne la soutient pas donc arrête

  • @cadandong7564
    @cadandong7564 4 месяца назад +2

    Ne confondez pas vouloir être libre et traumatisé

  • @FamaSow-bi4pt
    @FamaSow-bi4pt 4 месяца назад +2

    tu as bien parler ma fille

  • @umuzahra7177
    @umuzahra7177 4 месяца назад +2

    Walahi famille aicha bonoul demna ben mission s'en deuk thilogne t s'en keur demna fa môme famille bou bien leu mais ndogal bou gnower rek

  • @NdeyemaimounaSow
    @NdeyemaimounaSow 4 месяца назад +5

    Chez le spycholégue 😂😂😂😂

    • @nianedieynaba9153
      @nianedieynaba9153 4 месяца назад +1

      😂 dafa dioum

    • @NdeyemaimounaSow
      @NdeyemaimounaSow 4 месяца назад

      @@nianedieynaba9153 sisi je compren dé juste k dama retane ba soone

    • @PMS667-k5x
      @PMS667-k5x 3 месяца назад

      Bayilenn topp nit bamou seuss😂😂😂

  • @YoohGui
    @YoohGui 4 месяца назад +9

    Xalebi sikna d mais aye mbokam nioko japalewoul diox lekk ak nane doyoul.. Problème aye parent wam dou fautam baniou kokoy xasser. Aussi même sou demer naneko dieul forcer ko mou tokk ki xalebi ndaw. Négligence famille bi kesser lafi guiss

  • @BayeModou122
    @BayeModou122 3 месяца назад

    ❤Masa❤❤❤❤❤

  • @AissatouWade-z2n
    @AissatouWade-z2n 4 месяца назад +4

    Kouko meneu dimbeuli dimbaliko té yalla takh dax mbolen deglo wakhi nienegni doleneko dimbali

  • @ToureHamady-ny9lh
    @ToureHamady-ny9lh 3 месяца назад

    Amadou alpha a dit la vérité il l'a connait très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très très bien bien bien 👈

  • @djimbycourasene3146
    @djimbycourasene3146 4 месяца назад +2

    Lou ame ba ame moy you melni solution ak yeda rek mofi nekka.
    Kouko meuna diapalè naka diapalè.
    Lousssi dess moye xalè bou ndaw 20 ans deme di concubinage ba eumba fekka lassi. Nene ka terè souni dome. Xolene sene dome fougni nekka kougni andal.
    Xalè daye tog si keureum ak nou keur gui melnak nex nakari

    • @sheinie4949
      @sheinie4949 3 месяца назад

      Liko dall dou si concubinage si vous avez bien suivi son interview biko eumb bi daler lako tante bi wakh thiat outal ko chambre comme son mari kilifa la patati patata, manam tatam si bopam moko pousser à la rue elle s’est débarrassée d’elle et l’a exposée à tout ce danger et se retrouver à la rue avec son bébé. Elle a juste besoin de soutien, d’accompagnent et d’assistance. C’est terrible d’avoir à payer pour les fautes de ses parents.

    • @kefgg
      @kefgg 3 месяца назад

      ​​@@sheinie4949je ne comprends pas. Grosse bi foumou diougué? Dafa ame dieukeure wala hors mariage leu ?

  • @babacarndiaye1419
    @babacarndiaye1419 3 месяца назад

    Sokhna Gambienne bii loumou wax dale ladaccord. Wax deugue Aicha a besoin d'affection venant de sa famille. Bulene khole Aicha nimou Mel, xole lene metite yimou traverser, nga tela niakk Yaye, sa wadiour bu Goor weroul. Aicha diegue woul Sakh bone, dafadi xaley bu niakk affection parentale. Sa famille devrait lui apporter bcp plus d'affection. Mais Pa diko xole ay dieuf ou bayam. Ndax xamoul yayam.

  • @Mouya-q5b
    @Mouya-q5b 4 месяца назад +1

    le débat est clos pas close

  • @AwaDiouf-g4w
    @AwaDiouf-g4w 4 месяца назад +1

    Vraiment c'est triste

  • @boussothiam4589
    @boussothiam4589 4 месяца назад

    Merci Dassina tu as tout dit

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 4 месяца назад +1

    Elles sont où les associations qui aident les gemmes en détresse

  • @mamefatoudiagnediop
    @mamefatoudiagnediop 3 месяца назад

    Normalement l'histoire de sa maman c'est lorsqu'elle avait 6 donc elle ne devait jamais l'apprendre si sa famille avait bien garder le secret pour préserver les enfants

  • @dieynabatoure1507
    @dieynabatoure1507 3 месяца назад

    Aicha n’a pas à payer pour les erreurs de son papa . Elle plus besoin d’aide de plus que quiconque. Je comprend pourquoi elle s’est laisser berner aussi facilement. Et les mecs aussi a profiter d’elle

  • @thiamathiam9932
    @thiamathiam9932 4 месяца назад +9

    Aicha sama khalata daniouko yaré saguome yeureume batakhe diowoule respect legui nack euppenaléle lokho balikodale yeuppe dalko

  • @BintaNdiaye-c2z
    @BintaNdiaye-c2z 4 месяца назад +6

    Légui nidiayame lanne la done déf si réw ni ba dalle khalé bi 😭 nagui bayi guiss talle✅

  • @marietoutamba223
    @marietoutamba223 4 месяца назад +1

    Khalé dafa traumatisé wou mane lolou la guis xolal dof bi nék si live bi nane papam mo ray yayam lolou Bo démé Aïcha dég nako motakh mou traumatiser

  • @nenediack610
    @nenediack610 3 месяца назад

    Cc bb aicha guis Mane dema âme goitre té yenewoumaloko té goitre defa meti c soufre énormément bilahi yenewoumalako metrizel stp😢😢😢

  • @MouhamedGuisse-d8l
    @MouhamedGuisse-d8l 3 месяца назад

    SAMEE guel la wOnn et vraiment la femme dit vrai Aicha à besoin d’aide car mane je la connaît elle a une agressivité incroyable et des absences bizarres

  • @bellediolla3414
    @bellediolla3414 4 месяца назад +2

    Cet enfant c'est révolté contre les insultes qu'elle subissait et le rappelle constant des faits de son père. Il fallait l'éloigner de la famille de sa mère et son père parce que ils vont tjrs lui rappeler le crime de son père elle ne devait pas connaître si tôt l'acte de son père.

    • @awadiaw8310
      @awadiaw8310 4 месяца назад +2

      Bilay ndeysane que Dieu le protège

  • @cocosqueen1752
    @cocosqueen1752 4 месяца назад +3

    Guir yallah nako famille wan tahawou dimballi ko sinon dina sankou

  • @AichaIdriss-ku6jc
    @AichaIdriss-ku6jc 3 месяца назад +1

    Boulen geum nitki si loumou nouro 🎉 et moi en personne loumasi yok na parents yis guena bayi xel si éducation Si Sunu Dôme yis deysane sinon fou rewmi dieumm dina guena niaw.parents yis svp 🙏 je vous condamne pas mais vous êtes les racines de ces arbres.desole si j'ai touché quelqu'un ici.xale yis tamit nagniou bay xel si lou geun di dox sinon présent ak futur bou niaw mogniou xarr.

  • @karimthiandoum1510
    @karimthiandoum1510 4 месяца назад

    Doul way yow mounan rendez vous 😂😂😂

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 4 месяца назад +5

    YOW JUSQU AU PREUVE DU CONTRAIRE AMOUL ; JUSQU A LA PREUVE . BAYYIL FRANÇAIS BI TA WAKH WOLOF . TU AS 4 FAUTES DS UNE SEULE PHRASE

    • @Intégrité-v1p
      @Intégrité-v1p 4 месяца назад

      😂😂😂😂😂😂

    • @fatoubilelkane5804
      @fatoubilelkane5804 4 месяца назад +2

      Lolou la bougone wah tek français bi souf wah olof😂

    • @famad3455
      @famad3455 4 месяца назад +4

      Vraiment olof mety woul

  • @EvaSane-d8j
    @EvaSane-d8j 3 месяца назад

    Nidiaye bi môme wéroul

  • @fatimly7506
    @fatimly7506 4 месяца назад +1

    Au lieu de trop parler que des détail unitule on doit l'aider elle est très jeune sa famille est responsable elle lon abandonner aulier de l'aider

  • @florencediatta9361
    @florencediatta9361 3 месяца назад +1

    Cette famille de la maman c'est la haine qui ont envers le papa pour avoir tué leur sœur motakh gnoukoy xolé xalébi

  • @binetadiop9050
    @binetadiop9050 4 месяца назад +5

    Nidiayame dina sétale dérou famiyame, Aïcha dafa teuh, mais légui sonna, dina yéme la yakare

    • @aminacisse2396
      @aminacisse2396 4 месяца назад +7

      Doundou bou sotégoul Lou nek khadj naci yaw tu es une femme et tu te permets de juger comme ci danga doundou limou vivre

    • @dieyladieye5266
      @dieyladieye5266 3 месяца назад

      Yaye bou nék bou sanione domame mo fi gueune mais yayame famou teude yalnako yalla yeureume té tek loko çi domame.

  • @khadidjatoudiop6123
    @khadidjatoudiop6123 4 месяца назад +4

    Ay way femme bi n'a bayi FRANÇAIS yi té wakh ouolof khaméwoul masculin ak féminin

  • @lalaidebh5kf
    @lalaidebh5kf 4 месяца назад +5

    Maylen khalé bi diamou bolenkm ko mounoul diapalé guen bako bouguen amon taxaway bi war si mom dou guen goudi guen koy yek fadiar franchement c'est degueu

  • @CheikhThiam-y8c
    @CheikhThiam-y8c 3 месяца назад

    Cas aicha dama dioye ba sono

  • @mariesow2205
    @mariesow2205 4 месяца назад +2

    Nidiaye aîcha bi kou bonela xalé bou touti yayame décédé géne bayiko mou toumouranké Yako wakh xalé bou 15ans menoul teu kéne

  • @ramatoulay7481
    @ramatoulay7481 4 месяца назад +1

    Sénégal nio beugua khas nit motah souniou wadiour wara kholate send dokhaline

  • @mahmoudba2399
    @mahmoudba2399 3 месяца назад

    Ce qui est grave l'ACT que son père a fait la suivi elle l'homme qui la angrosse a faillit la poignardé elle l'a expliqué

  • @ÉlémentsSerigneFallou
    @ÉlémentsSerigneFallou 4 месяца назад +1

    Macha Allah la tata Gambienne à tout dit Aïcha n'a pas besoin de confort elle a besoin d'amour et d'affection en vers sa famille elle n'a besoin qu'on lui rappelle ce qu'a son père

  • @AissatouWade-z2n
    @AissatouWade-z2n 4 месяца назад +2

    Famille yi bouniou la khasse ba bagne danioulay sossal de toute les façons Aïcha khale la te and AK nakar bou Sakh ci xoll bi

  • @DAMETHIAM-rl1sz
    @DAMETHIAM-rl1sz 3 месяца назад

    Aïcha Lim wakh mo am déful d'ara ay mbokam yi ko abandonner ño bonne

  • @khadijetoulykane8909
    @khadijetoulykane8909 4 месяца назад +2

    Cherif nekouloo senegal ba pare di kathieu

  • @ToureHamady-ny9lh
    @ToureHamady-ny9lh 3 месяца назад

    Chérif=Amadou alpha 😂😂😂

  • @diakhereseye3275
    @diakhereseye3275 4 месяца назад +1

    Bilakhi gnake yaye dafa méti trop bilakhi bilakhi damako yeureume 06 mois ga gnake yaye ohhhh Mane dé à l'âge de 23 ans la gnake sama yaye mais balégui Moy lolou

  • @khadijetoulykane8909
    @khadijetoulykane8909 4 месяца назад +2

    Son soit disant nidiayam biii, je suis certaine que tantam biñou naan kilifeu moko takeu moo yonee pour discréditer Aicha. Khale bou ndeyam deeh, bayam febar même si c'est son père qui a tué sa mère, ce n'est en aucun cas sa faute. Yom mii di nodiaayam au lieu d'aller chercher ta nièce et ton petit fils ngay yakheu derrr
    Ko aan jaassi

    • @thereselissire840
      @thereselissire840 4 месяца назад +1

      Slt sister lolou mna nek influence de sa tante

  • @KebeCheikh-ps4ob
    @KebeCheikh-ps4ob 3 месяца назад

    Leufeul ndayi yi gni lidianti problème yi

  • @baoumarwane
    @baoumarwane 4 месяца назад +1

    Vraiment vous les liveurs la hamolene adunaa
    Juste avec ces mots là elle peut vivre pire que ce qu’elle vivait avant
    Comment on peu dire ça en public sûrement Aicha le savait même pas c grave

  • @NdeyeFatouGueye-tt2jf
    @NdeyeFatouGueye-tt2jf 4 месяца назад +2

    Nigua yoré sa diabotte soko defone diguako yoré sou nekone sa propre dôme dofi nek di wakh li wala guen koy abandonner loumou mel yek yen la parce que bimou neké khalé guen ko yorone ba legui donc diaroul gua nek fi di wakh defoulo sa takhaway matoulo kilifa

  • @thiombayeseck9782
    @thiombayeseck9782 4 месяца назад +1

    Téye léne janrou boy yi dagnon doy war dh bakh na tonton mi dég lou léne bou bakh

  • @awakeneme4049
    @awakeneme4049 3 месяца назад

    Walahi deugue gawahe gambien

  • @BLACKHERO-f4s
    @BLACKHERO-f4s 3 месяца назад +1

    Sénégalais amoul soutoura walahi.yakh deer rek lagnou mane

  • @YazineNdiaye
    @YazineNdiaye 4 месяца назад +1

    Adouna dafa meti lolou bilahi mane lima ndoudou rk dafa meti lolou tai kaine taiguoumako koudoule sama yay tai so explikai kene doula gueme bilahi dafa meti lolou bilahi ma guena ame louma meti thi adouna tai koumako wakh douko guem

  • @cheikhououmarfaye4287
    @cheikhououmarfaye4287 3 месяца назад

    wa français queen yi doléne si wakh🤣🤣🤣🤣

    • @Ibra-e6k
      @Ibra-e6k 3 месяца назад

      Bilay gnii danio yabaté ak séne français yiniouy forcer ak fautes you beuri yi

  • @cisco9615
    @cisco9615 4 месяца назад +14

    Na ma yalla bal samay origine ay peuls laniou mais peul mo gueun bone thi sénégal daniou lay fatali sa démb yaye wala papa ou bien no djoudo sans géne😢😢😢

    • @Diam05
      @Diam05 4 месяца назад +1

      Ayy way Lolou dei yalla beugou ko Tei deugu pire gua wakh

    • @auparadisdesanges1599
      @auparadisdesanges1599 4 месяца назад

      Manite peulh la dehh mais sounou djiko nekhouma dara

  • @yacinekane4559
    @yacinekane4559 3 месяца назад

    Li mo yakk Sénégal lekk nane akk jangg rekk moy normalo khalé

  • @DabaSarr-sh6nb
    @DabaSarr-sh6nb 4 месяца назад +1

    ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @FatouGueye-l2u
    @FatouGueye-l2u 3 месяца назад

    Limdatie daméti kou ko dék lou kham ko nit nk sa mbokou dioulit bou dioumé dangua koy délossi mé pas guakoy bédi

  • @antimensonge5709
    @antimensonge5709 3 месяца назад

    Quand sa maman est mort elle était une bébé elle pleure depuis matin jusqu'à 16heur la famille fait semblant comme rien n'est été

  • @BLACKHERO-f4s
    @BLACKHERO-f4s 3 месяца назад +1

    Peut être même que son oncle avait la haine envers Aïcha

  • @AstouSy-f8i
    @AstouSy-f8i 4 месяца назад +3

    Ak lou meuna ame teyer woléne ko en plus ama guoul yéneu maturité mais yéneu nieupe guéne beugue ko setane c pas normal entouré de l’affection c’est mieux lolou la sokhla

  • @adjifatimdiop3539
    @adjifatimdiop3539 3 месяца назад

    Wa Borom français yii khana école jaalaalè la janguè😅😅😅

  • @khadijetoulykane8909
    @khadijetoulykane8909 4 месяца назад +1

    On s'en fou de dieukeurou tantam ndakh bouton seen propre doom, dinathi neup seeni seur fimmmmp waay famille indigne

  • @b_lebou8908
    @b_lebou8908 4 месяца назад

    Aicha dioundiou na lolou nena sama papa meloul won nimou melon motax sen niari famille yi moy lolou