OUSTAZ BA vous êtes en train de faire un travail extraordinaire, difficile même de parler avec ces personnes qui sont en déphasages sur ces idées en déphasage avec l’islam authentique, mais le prophète avait vécu avec ses compagnons
Je pense qu'il faut arrêter Baye NIASS ne nous a jamais dit de faire l'adultère au contraire. Baye NIASS alkhourane la ak souna. Wakh nak si tu comprends pas tu demandes. Niawna trop tok di sossal Baye NIASS.
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته يا أخوة نصيحتي لكم لاتتكلموا مع الجهال الذين لا يعرفون حتى كتب أشياخهم وإلاسيكون اضاعة للوقت إذانقلتم في كتبهم وأنكروا هذا النقل فانزلوهم
Ki niou beuri niou andone ak mom légui ay Talibé Baye laniou lolou dafko metti trop motax mouy sossal Baye Niass rek. Dafa sissou té wo nagn ko si debat xam xam mou bagne. Na dém debat ak Ibrahima Maqari walla Cheikh Ibrahim Saleh. Tokk di soss c trop facile😂 Baye di nangou sén mbolo yeup ndax limou yoor deug leu té deug bou lerr. Charia ak Haqiqa bou werr sa dîné matt lolou la Baye indi.
En tout cas fougnou toudou yonantibi dinagnoufa toudou baye niass lolou la yala dogal ndah moko liguéye ay millions la dougoul si l'islam lou kén mossoul déf si l'islam hamal yala ay millions
Indi wo bén référence. Soss ak gatt xam xam ak daw debat ak borom xam xam yi sén yeuf la. Mane Yalla dimbeuli nama ba guéneu si sén mbirr dém andd ak deug mouy Manrifa, xam Yalla
Yéna meuna doul Baye meussoul wax li nguén wakh. Ki ap noone bouy soss la. Dou inddi référence moukkou. Na repondre debat Talibé Baye yi nekk pakistan ak Moufti Nigeria ak Talibé Baye yi nekk inde nieup wo nagn ko si debat mou daw
Kii nguén di déglou dafa fénal Baye té borom xam xam yi si Faydou tontou nagn ko si ay téré ak ay video. Mufti medina bi invité nagn ko debat mou bagne.
On est en démocratie, il faut accepter la contradiction. Sinon il y'a pas de sens à votre débat==>vous êtes trop agressif pour des gens qui appellent à la sunna
@@KAADUDINEEJITV vous fuyez le débat, il faut laisser la personne s’exprimer et donner son point de vue et dans le respect comme nous enseigne le prophète psl
Yaw mii di wakh ya niémé yaallah d chrétiens yii d niola gueun musulman moy wakh ak yaw nak manou bakhna kounek gueumal sa religion t rspecté say mbok jam
😂😂❤ s’il vous plaît. Merci d’aimer la vidéo. Abonnez-vous à partager pour nous soutenir
Alhoran kasé ak son ne
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
Naturellement, il mérite vos soutiens qu’Allah l’assiste❤❤❤❤❤
Mais naturellement un grand chapeau. Bravo à ce jeune homme Oustaz. Alpha Ba ❤❤❤❤
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
@@deug8604
Asrar c'est livre de Ibrahim Niasse,mon frère on est réveillé,ton marabout n'est pas clair, qu'Allah le pardonne
Merci à toi ma sœur qu'Allah nous préserve de ces Soit disant Marabouts bizarres.
❤❤❤❤❤
Vraiment très pertinent et suis content de vous ❤❤❤❤❤❤❤❤
ما شاء الله جزاك الله خيرا وبارك الله فيك يا أستاذ الفاهم❤
Un grand merci d'avance oustaz Alfa Ba ❤❤❤❤
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
Bravo oustaz Alfa Ba ❤❤❤❤
Merci Alpha
بارك الله في جهودكم وأحسن الله إليكم❤
Salam Oustaz Alpha. Merci de me partager le lien du compte tik tok pour le suivis des debat en lign
La jeunesse IL est temps de SE reveiller comme vous oavez fait sur les politiciens❤❤❤❤
❤❤❤❤ barakallah fiiiykkhumm
😂😂😂😂 Baye Niass un vrais imposteur
REVEILLEZ VOUS LES JEUNES SENEGALAIS SUR VOTRE RELIGION AU LIEU DE SE FOCUS SUR LES POLIQUES ???????????!!!!!
Mais continue sur cette lancée, vous vous faites un travail encore très remarquable, très très remarquable❤❤❤❤❤
Merci infiniment
Vraiment pour dire vrai, l’est grave ici, au Sénégal avec ses faux marabout sur leurs paroles à dormir debout Hahahahahaha😂 mdr
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
@@KhadijahDiop-d1w yen loutakh sen wakh dji si clavier rek ngen ko sagna def
OUSTAZ BA vous êtes en train de faire un travail extraordinaire, difficile même de parler avec ces personnes qui sont en déphasages sur ces idées en déphasage avec l’islam authentique, mais le prophète avait vécu avec ses compagnons
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
Oustaz Alpha ba machallah 🙏❤❤❤❤❤
Billahi Sunnah mba sonnu yallah na yallah same sunnou Imane 🩸🫀🩸
No galsen mo nexx yewouleen Yewu diotna Wayu 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂 diomii amoul heurrr4rr
Comme di les senegalais ont leur propore RELIGION ñoñ regarder comment sont les intervenant IL ose MM defendre l'indefendable 😂😂😂😂😂😂 mdr
Je pense qu'il faut arrêter Baye NIASS ne nous a jamais dit de faire l'adultère au contraire. Baye NIASS alkhourane la ak souna. Wakh nak si tu comprends pas tu demandes. Niawna trop tok di sossal Baye NIASS.
Assamou alaykoum ❤❤
يريدون أن يطفئوا نورلله بأفواههم ويابى لله إلا أن يتم نوره
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته يا أخوة نصيحتي لكم لاتتكلموا مع الجهال الذين لا يعرفون حتى كتب أشياخهم وإلاسيكون اضاعة للوقت إذانقلتم في كتبهم وأنكروا هذا النقل فانزلوهم
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mais s’il vous plaît par kel moyen pour accéder si live bi ???
Alpha yerem na sa monjenteel blie
Alpha s yaw niatta nitt nga dougal thi l islam nga beug yob bay Niass safara il faut respecter une personne qui prie
Ki niou beuri niou andone ak mom légui ay Talibé Baye laniou lolou dafko metti trop motax mouy sossal Baye Niass rek. Dafa sissou té wo nagn ko si debat xam xam mou bagne. Na dém debat ak Ibrahima Maqari walla Cheikh Ibrahim Saleh. Tokk di soss c trop facile😂 Baye di nangou sén mbolo yeup ndax limou yoor deug leu té deug bou lerr. Charia ak Haqiqa bou werr sa dîné matt lolou la Baye indi.
En tout cas fougnou toudou yonantibi dinagnoufa toudou baye niass lolou la yala dogal ndah moko liguéye ay millions la dougoul si l'islam lou kén mossoul déf si l'islam hamal yala ay millions
Indi wo bén référence. Soss ak gatt xam xam ak daw debat ak borom xam xam yi sén yeuf la. Mane Yalla dimbeuli nama ba guéneu si sén mbirr dém andd ak deug mouy Manrifa, xam Yalla
Ragualléne yallah dioulite daye wakhe louko lér ak mandou
Dagne léne yoni si tarikhayi
Asrar n'est pas un livre de Baye Niass, Baye n'a pas un livre qui a pour titre Al asrar li dou dégu bayiléne sossalaté
Yéna meuna doul Baye meussoul wax li nguén wakh. Ki ap noone bouy soss la. Dou inddi référence moukkou. Na repondre debat Talibé Baye yi nekk pakistan ak Moufti Nigeria ak Talibé Baye yi nekk inde nieup wo nagn ko si debat mou daw
Wakhal lu Bai Niass wakh bul ko sosal seringe b
Sama gars yi al asrar abdoulaye niasse mais pas baye niass
Baye limou déf si l'islam sa baye mounouko liko l'islam diaral amoul mbidéf boumouko diaral
Je trouve que vous netes pas democratiques. C'est un debat interressant wayé vous ne pouvez pas debattre et autoritaire. Dommage
Kii nguén di déglou dafa fénal Baye té borom xam xam yi si Faydou tontou nagn ko si ay téré ak ay video. Mufti medina bi invité nagn ko debat mou bagne.
Yénangui fén rek di soss motax jamais nguén nangou debat ak borom xam xam yi. Pourquoi dou nguén nieuw debattre ak borom xam xam yi
Alfa degay fen degay soss baye bindoul terr bou toude Al assrar lacenanala defi
On est en démocratie, il faut accepter la contradiction. Sinon il y'a pas de sens à votre débat==>vous êtes trop agressif pour des gens qui appellent à la sunna
C'est quoi la democratie mdr hahahahhaha
Je pense que vous vous trompes lourdement mon frere ...
Bref le debat c'est autre la religion
@@KAADUDINEEJITV vous fuyez le débat, il faut laisser la personne s’exprimer et donner son point de vue et dans le respect comme nous enseigne le prophète psl
Yaw mii di wakh ya niémé yaallah d chrétiens yii d niola gueun musulman moy wakh ak yaw nak manou bakhna kounek gueumal sa religion t rspecté say mbok jam
Hahahahahah Allahou Moustaعn
Ndékete galsen fii la réere gui tollu mdr
Oustaz Alpha wéranté moko nara sank dioulitt dou wérantei. Amolenn niveau pour comprendre waxou khoutbou yi
Wakhofi dara Alpha déy yété
Bravo oustaz Alfa Ba ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
MerciOustazAlfaba❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

❤❤❤❤❤❤❤❤